‼️Urgent Grosse Déclaration De Coach Bakary Sakho Apres La Sortie de Siteu..; Limou Wakh Aziz Dou…

Спорт

La #luttesénégalaise #fadam 2
✅Abonne toi pour ne pas rater mes vidéos ✅
Chaîne KZread

Пікірлер: 207

  • @mbenelo9730
    @mbenelo973026 күн бұрын

    Bacary a bien parlé quelle communication bravo oui siteu doit être professionnel

  • @malicksarr2141
    @malicksarr214126 күн бұрын

    Modou Lo champion yalnako yalla maye ndame yalla bou modou Lo amati défet si adouna ❤

  • @bamediallo7082

    @bamediallo7082

    25 күн бұрын

    Yarabi 🤲 inchallah

  • @moussamballo2207
    @moussamballo220726 күн бұрын

    Incha allah modou lo dinako doumeu daan koo incha allah bou nekh yalla sunu borom

  • @loufaassdiao5389
    @loufaassdiao538926 күн бұрын

    Bakary yaw damalay suivre mais parfois say analyse mom moy lolou khana khamoni modou beuré bi mo eupe khekh bi

  • @bayealladieng5810
    @bayealladieng581026 күн бұрын

    Bakary modlo est plus rapide et plus athlete pr nga dannnko il faut nga tégal ko lou tar tt façon bonne chance a modou

  • @bricecorrea2628
    @bricecorrea262826 күн бұрын

    Bakary ioe ak siteu yeup bolenn nieuwé modou nokou lenn dane lenn

  • @jobehamidou6545
    @jobehamidou654526 күн бұрын

    Merci bro bakary

  • @daourndoye2103
    @daourndoye210326 күн бұрын

    Siteu mi wakh len ko deugeu mou melni kou febar ki pour mom lamb ay wakh rek la

  • @Chiekh766

    @Chiekh766

    26 күн бұрын

    Yaw mi fébar moye yaw nék Di doule rék

  • @bassou77

    @bassou77

    26 күн бұрын

    Yaw demal wakhko dougg Kane Mola wakh ni siteu entraînéwoul merd way

  • @moussapayemane4167

    @moussapayemane4167

    26 күн бұрын

    ​@@bassou77mongui entrainé mais manoul am dolé 😂😂😂😂

  • @mariamjohn9172
    @mariamjohn917226 күн бұрын

    Coach machallah looking good without the lox

  • @kebbacamara-nl1km
    @kebbacamara-nl1km25 күн бұрын

    Thanks coach Bakary and Fadam keep it up boys

  • @sirmandiallo4685
    @sirmandiallo468526 күн бұрын

    Félicitations bakary. Force à toi

  • @Bayemor4555
    @Bayemor455526 күн бұрын

    Bakary néna siteu mo raw sa Thies 😂😂😂

  • @simmelsarr3599
    @simmelsarr359926 күн бұрын

    Bakary sa wakh nekhoul mais deug rek ngay wakh.

  • @BoubacarGaye-xh7md
    @BoubacarGaye-xh7md26 күн бұрын

    Coach bakary 😂😂non tu nepas serieux quoi fadame dh tontuwoula sakh gua wakh say wakh bapare diko retane 😂😂😂

  • @lamine3372
    @lamine337226 күн бұрын

    Fadam gnaaw nga😂😂😂😂😂

  • @talladiagne8092

    @talladiagne8092

    26 күн бұрын

    Demal gustou yonenté yalla Nouh

  • @lamine3372

    @lamine3372

    26 күн бұрын

    @@talladiagne8092 sira bobou gneupako kham wayé dagnouy kaff rekk wakh nitt ya gnaaw yague n'a si reww mi té cohésion sociale demal gustou Seyidina Moussa nga kham louy" mandu" ndakh wakhouma ak yaw té fadam gno defando enfance

  • @abdousalamdiallo6008

    @abdousalamdiallo6008

    14 күн бұрын

    ​@@talladiagne8092Merci

  • @ibrahimadione1770
    @ibrahimadione177026 күн бұрын

    Salam bakary nga balma avant je te juge mal mais vraiment tu as beaucoup d'esperience siteu ne devait pas répondre à Aziz ❤

  • @senprintsn4221

    @senprintsn4221

    26 күн бұрын

    tu as marché sur ma langue

  • @malickkanekandji9791
    @malickkanekandji979125 күн бұрын

    Bakary bien dit mashaallah

  • @ND.BALLAuser-ft7kg5jk5v
    @ND.BALLAuser-ft7kg5jk5v25 күн бұрын

    Nd!@¥€💯B@LL@❣️ Ndame réék inchallah 🤲💯💪🦁❣️

  • @user-iz8ot5zl9x
    @user-iz8ot5zl9x24 күн бұрын

    Salalahou Ala mouhamad

  • @amdymoustaphapatiencefall7482
    @amdymoustaphapatiencefall748222 күн бұрын

    Siteu rek inchalla ☝️

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj23 күн бұрын

    Modou lôooooooooo ❤❤❤❤

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane716325 күн бұрын

    Merci beaucoup Siteu

  • @sambagora7848
    @sambagora784825 күн бұрын

    Sacré Modou Lo. Fadam yagui diagual wa dji lamb déh😂😂😂.

  • @durkio5486
    @durkio548626 күн бұрын

    Tu ose comparé siteu ak balla gaye . Balla mo eup dolé siteu dak ko beuré . Siteu bane champion bou mak lafi dane? Il a perdu contre sa thies lac 2 gouygui et plein dautres . Modou lo dou moromou siteu sa way

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv26 күн бұрын

    Siteu dall lene lama nekhé lidizntiwoull aziz ak khalissam t aziz liko siteu falewoull moko metii

  • @user-jn5qm5oi7r
    @user-jn5qm5oi7r26 күн бұрын

    Slt bacary dicourage tu as bien analysé

  • @carterjim9391
    @carterjim939125 күн бұрын

    Dp8 bi djily seck saga sa ndèye ba légui niéme to siteu😅😅 doul rék ngaye déffff😅

  • @user-ut3fx4ok4v
    @user-ut3fx4ok4v26 күн бұрын

    Siteu dafa wara dem liguey baye wakh dji 👌👌👌

  • @Chiekh766

    @Chiekh766

    26 күн бұрын

    Yaw siteu gniatta wérre guissoko

  • @kheuchboukharagne
    @kheuchboukharagne26 күн бұрын

    Ki mo khamoul gat si limouy wakh

  • @malickndiaye4880

    @malickndiaye4880

    26 күн бұрын

    Bilae 😂

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall949426 күн бұрын

    BOrom khol you gnoul yi meunou gnou beug modou lo

  • @saiifba4282
    @saiifba428226 күн бұрын

    👍👍👍👍

  • @badamar6802
    @badamar680226 күн бұрын

    Li motakh ay victoire modou lo di special chak combat modou fénelo léne

  • @MamadouDiop-ng6np

    @MamadouDiop-ng6np

    26 күн бұрын

    😊

  • @ridialdieng2861

    @ridialdieng2861

    26 күн бұрын

    Sa way bayi gnou lii dou combat

  • @MoussaFall-hs1gn
    @MoussaFall-hs1gn26 күн бұрын

    Sa waye d'à ngaye xarr

  • @sonnedj2304
    @sonnedj230422 күн бұрын

    BAKARY Wa diamageun dagne ko menacer won djily lay nekhal 😂😂

  • @user-zw5ui2ci5q
    @user-zw5ui2ci5q21 күн бұрын

    Fadame Tu es beau😂😬

  • @monudiallo4500
    @monudiallo450025 күн бұрын

    fadam dél sol mbakhané nguir yalla sa bop bi kom talmbatt(guithiakh thiakh guithie)

  • @universitietelephone4010

    @universitietelephone4010

    25 күн бұрын

    Yàlla mi bind bopp bi ngay Wakhal wala Fadam?

  • @user-ix9bm7ve9v
    @user-ix9bm7ve9v21 күн бұрын

    Ragal yapp yalla merci Bakary bokoulo ak ponkessi

  • @serignegueye3035
    @serignegueye303526 күн бұрын

    Merci bakary degue gua wax

  • @senenergyfamily5726
    @senenergyfamily572626 күн бұрын

    Good guou gnaw coach bakery khan khan lay wakh

  • @thiecouratraore2442
    @thiecouratraore244225 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤

  • @modoudiop7841
    @modoudiop784126 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @user-bw2kk5jv7h
    @user-bw2kk5jv7h26 күн бұрын

    Lolou dou combat boulene niou sonal

  • @Ababoukara
    @Ababoukara23 күн бұрын

    Noooonnnn. Fadam gnaw ngua quoiiiiii😂

  • @moisabarry
    @moisabarry25 күн бұрын

    Fadam gnawena srx😂😂😂

  • @modoudiop7841
    @modoudiop784126 күн бұрын

    MODOU XL0 ❤❤❤❤🦁🦁🦁🦁🦁🦁

  • @user-ff1fe6qf6z
    @user-ff1fe6qf6z25 күн бұрын

    Aziz dee da ame aye diam komm genr khett yi ay diam laniou ki di melni mbeut s fadam la sen depense si aziz laniou yakor motakhe douniou ko wakhe deug

  • @Abraham22199
    @Abraham2219926 күн бұрын

    Raag ak tapha tine fadam niko kann 😂

  • @user-rg2kk9hg2g

    @user-rg2kk9hg2g

    26 күн бұрын

    😂😂😂😂

  • @DameNdiaye-ig5rh
    @DameNdiaye-ig5rh20 күн бұрын

    Siteu bou amé dollé je te jure au nom de dieu Modou menou kooo

  • @durkio5486
    @durkio548626 күн бұрын

    Barki alkourane bakary khamoul lamb

  • @malickndiaye4880

    @malickndiaye4880

    26 күн бұрын

    Bilae frr c k Sénégalais yi ño meuna valorisé dof 😂

  • @Amethfouteu815
    @Amethfouteu81526 күн бұрын

    Bakari vraiment nitte kou deugoula

  • @user-ib5jk1tx4r
    @user-ib5jk1tx4r25 күн бұрын

    Fadam il est beau 😂😂😂😂

  • @mouhamadibnismail5827
    @mouhamadibnismail582726 күн бұрын

    😂😂🤣fadam danio wax tapha tine rek mou rouukh

  • @user-ms9ui1cw9s
    @user-ms9ui1cw9s26 күн бұрын

    Bacary sa tounou ndaye gnoune siteu kessé 💪

  • @badara389
    @badara38926 күн бұрын

    Siteu❤❤❤❤❤❤🇱🇷🇱🇷🇱🇷🇱🇷🇱🇷💪💪💪💪💪💪💪💪

  • @BassLeye-tc8ne
    @BassLeye-tc8ne24 күн бұрын

    dégue la wakh dh way nak suite dan Modou Dina ma bet

  • @amadoumoctarcissokho9141
    @amadoumoctarcissokho914126 күн бұрын

    Modou lo mo meune si lambe dji

  • @moustaphambacke9882

    @moustaphambacke9882

    26 күн бұрын

    Damay wo balla dh

  • @TopGueye-nv7pc

    @TopGueye-nv7pc

    26 күн бұрын

    ​@@moustaphambacke9882gnou oh eumeu,bombardier,AK boye Niang

  • @adamsempereur3149

    @adamsempereur3149

    26 күн бұрын

    @@moustaphambacke9882damay wo eumeu Sene deh

  • @user-xq4og4to4j
    @user-xq4og4to4j21 күн бұрын

    Fadame ya bakhe dhé goré mborome bakhe nga yalla khamnako

  • @SfallouMbacke-st1bh
    @SfallouMbacke-st1bh26 күн бұрын

    fadame d'où tountou ci tafa tine 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @user-cw9gq8vs3o
    @user-cw9gq8vs3o26 күн бұрын

    Wallahi coach bakary sakho wakhna Deug siteu fawou mou diangue lou barry ak Dole diou barry

  • @SerignemodouDiop-uj8kr
    @SerignemodouDiop-uj8kr25 күн бұрын

    😂😂😂😂😂fadam rak tapha tine mouni ko kane

  • @ELIZOELIZO
    @ELIZOELIZO24 күн бұрын

    Bacary ioe moom nioroulo, fén reik té amo bén xam-xam, mbam nga reik

  • @lamine3372
    @lamine337226 күн бұрын

    Tayy lalén di wakh siteu dayy dann modou lo

  • @bassou77

    @bassou77

    26 күн бұрын

    bilahi inchallah ñi siteu dinalene bett

  • @DjibyNgom-ov3lm
    @DjibyNgom-ov3lm26 күн бұрын

    Fadam ak tapha tine fadam weyoul diel ko yako mene fouf😂😂😂

  • @ahmadsamb4890
    @ahmadsamb489026 күн бұрын

    Coach bakary fou coach bi diougué mane yague na la suivre mais meussou ma guiss mbeur bo préparé né nga champion nga meussou ma guiss sa béne combat ba paré nga bolé si toke sa roukhou di reuy lamine ak di manqué respect nite yi Djily bi la seufeul ba fo tolou di khalamal wa diamegueun dara rawou niou si wathie sil Sénégal 🇸🇳 nga wakhé nii ngay wakhé nga khôl ioe bou la modou tanthié nga kham né sa yonne nékou si

  • @pronosticfootsenegal1112

    @pronosticfootsenegal1112

    26 күн бұрын

    Bakari tiaga tarkinda yi leuuuu 😂😂😂

  • @hady284
    @hady28426 күн бұрын

    Dafa ragal yallmine yi😂😂😂😂

  • @mouhamedbadiane8133
    @mouhamedbadiane813325 күн бұрын

    Fadam nk nekhol ba nekhol ms sa bopo bi ak sa bakane yi ak guemeigne bi rey na trp😂😂😂😂😂

  • @badoundiaye5771
    @badoundiaye577126 күн бұрын

    Je suis bien d’accord sur un point avec Bacary que ni Siteu bou mélée nimou wara méel entraîné djang kheex am garde am audace meuneu na am dara . Mais est ce que d’ici jour j lolou yeup meuneu nako teyyé thi loxoom…on verra !!! Sur un autre aspect Bacary parle de rallonge, de taille, de force, de qualités , d’audace pour battre Modou lo mais il a oublié que ni B52, Lac2, Gris Bordeaux, Boy Niang 2, Eumeu Séne,Ama Baldé dougnou ayy thiouné té am nagn lolou kone est ce que Siteu waar na yém thi lolou késsé. Wakh dji wakh dji moy pour gneup kham ngako hors mis Siteu: moy Modou Lo pour nga daane ko dang koy gnémé, sathie ko dolé, gueuneu ko nekk, ba paré eupaléko ay atouts le Jour j. Bou lolou amoul do am dara Sport nak dafa gnaaw Yalla rekk kham mais je vois mal Siteu mal mené Modou Lo ba daane ko franchement.😮😮🎉

  • @papeleye267

    @papeleye267

    25 күн бұрын

    amga diott nak😂😂

  • @bachirdomouparcelle4293
    @bachirdomouparcelle429326 күн бұрын

    Bien fait li moniou djik

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop621626 күн бұрын

    Bilaye Siteu Moudou lo mou gou Man

  • @malickndiaye4880
    @malickndiaye488026 күн бұрын

    Ioe mom bala tarkinda yi tapé mba légui daga dieunde glasee 😂😂😂

  • @davembengue2938
    @davembengue293826 күн бұрын

    Siteu day forcè tè wa lamb wakhouniouko degue, siteu dafa wara kham ni danoufi kèneu

  • @adamslo7971
    @adamslo797126 күн бұрын

    Yoe katalll sa nday lane moy suporté thiaga xamo diobou mdayam chak combat modou lo ga baba ndiaye cii say analyse xamo diobou ndayam Yoe akh Fdm

  • @babacargassama3057
    @babacargassama305726 күн бұрын

    Bakary yagui dioum fofou Balla gaye 2 ak siteu dougniou bénn dée saye saye bi Balla ame si beuré siteu amouko si beuré

  • @kanecire5837

    @kanecire5837

    23 күн бұрын

    Même sa thies est plus fort que siteu

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop621626 күн бұрын

    Siteu Fan la Raw Sa Tihss

  • @sophrotall8105
    @sophrotall810526 күн бұрын

    Bakary Lou ler lay wakh siteu mo wara prouver limou wakh ya pas de mal

  • @galassefaye4587
    @galassefaye458726 күн бұрын

    Anilisou dof reék

  • @SfallouMbacke-st1bh
    @SfallouMbacke-st1bh26 күн бұрын

    fadame rafet nga😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @princeahmada7912
    @princeahmada791225 күн бұрын

    Bakay mo geuneu kharr data yayam modou sou koré siteu bakhiya la dieum dafa beuri ndy wakh bignouy dakhar ndem si ufc lolou wakhou si

  • @IssaSeck-cf6cs
    @IssaSeck-cf6cs26 күн бұрын

    Bayiléne sene féne yii

  • @eltulipo5484
    @eltulipo548426 күн бұрын

    Husky waleu Usyk😂😂😂

  • @papawade8521
    @papawade852126 күн бұрын

    par miracle rek lako siteu meuné sinon mom modou lo je ne supporte pzs franchement parlant mé c'est pas pour rien you naneko xaragn lo koudoul balla gaye modou lo nioussla amna technique am na dolé bandit guéwla téksi meune khékh fawwou nga eup ko dolé 2 fois sogko dane c'est le cas des deux victoires de balla gaye sur Modou lo et de bombardier

  • @modoudiop7841
    @modoudiop784126 күн бұрын

    😅😅😅😅

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse485426 күн бұрын

    Iaw bakary nafékh bakhoul siteu limou wakh ngor si ndiaye deugue leu ngor si ndiaye momoul ndayou lamb dji

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye26 күн бұрын

    On s'en fout coach Aziz Ndiaye vrai domouharam moo tah yalmbine bii totouco💪💪💪💪

  • @pierregomis2170
    @pierregomis217026 күн бұрын

    Sa Bokal vs Ada boy Baol 💥

  • @serignedieng7860
    @serignedieng786026 күн бұрын

    Bacary Sakho ya sokhor deug mé après gay comprendre

  • @gueyembaye853
    @gueyembaye85326 күн бұрын

    Calculer qu modou lo menoul diap lac 2 dane ko apar decision arrbitr te lac 2 meneloul siteudara dnc su sa rek lamb bou intense mene nafa am

  • @alioudia2821
    @alioudia282126 күн бұрын

    kanamou fadam2 b dafmay dérangé

  • @user-rb7qh7py7c
    @user-rb7qh7py7c26 күн бұрын

    Nioune modou lo bane ko défé bourou lamb dou taye

  • @Domou_Deukk_Bi
    @Domou_Deukk_Bi24 күн бұрын

    Bakary tay mom d'accorouma Modou mo meune siteu foufe si beuré

  • @youssouphandoye1244
    @youssouphandoye124426 күн бұрын

    Kirassoulay niaway fadam bi 😂😂

  • @AliouneDia-ty2kl

    @AliouneDia-ty2kl

    26 күн бұрын

    Ki bindoul bopam ah ❤😂🎉😢😮😅😊

  • @bambagueye2454
    @bambagueye245426 күн бұрын

    Bakary je ne suis pas d'accord avec toi, Siteu dafay léral

  • @goorgorlou1633
    @goorgorlou163326 күн бұрын

    Siteu amoul conseil Khamoul wakh dafa réw

  • @patrickb7956
    @patrickb795626 күн бұрын

    Domram, usyk nganane eusky, lilay wohoti sissa deugeur fiit ak graw grawlou t mane rek xamnani soutama less...

  • @pronosticfootsenegal1112

    @pronosticfootsenegal1112

    26 күн бұрын

    Ki domou haram leu khamoul ni wakhi dofam yi la gars yi sokhla pour plus de vues

  • @moustaphadiop892
    @moustaphadiop89226 күн бұрын

    Je suis de Balla Gaye Modou lô mo meun Siteu foouf

  • @khaliloulah3703
    @khaliloulah370326 күн бұрын

    Modou boko meunoul agressé dako dane 😂😂😂 té siteu n'est pas agressif franchement

  • @afro3827
    @afro382726 күн бұрын

    Fadam dé bop bi comme ay dunes rek 😂😂😂

  • @user-yl6qx3fx4d
    @user-yl6qx3fx4d26 күн бұрын

    Siteu seul❤❤❤❤❤

  • @gorasamb6213
    @gorasamb621326 күн бұрын

    Siteu pareparewoul dará day wakhe rek

  • @lahadnjay4885
    @lahadnjay488526 күн бұрын

    naampp yi dagno kham beurei dagno sonou ci guorr gni

Келесі