🚨 Débat Paroles Aux Talibes Baye Niass sur leur Croyance dépourvu de preuve ⁉️ - Oustaz Alpha Ba

🚨Urgent : 🇸🇳 Bidaah Beussou Tamkharit - Oustaz Alpha Ba & Dr Mouhammad Ahmad LÔ
• 🚨Urgent : 🇸🇳 Bidaah Be...
🚨Débat Paroles Aux Talibes Baye Niass cii senn Pass Pass you Doy warr yii 🤔🤭 - Oustaz Alpha Ba
• 🚨Débat Paroles Aux Tal...
Urgent Ay leral cii Ibrahima Guéye Khassida donn weur kaba gua ca Makka akk … - Oustaz Alpha Ba Ha
• 🚨Urgent Ay leral cii I...
🚨Urgent - Lamb jii - Messages aux lutteurs ⁉️ - Oustaz Alpha Ba H-A
• 🚨Urgent - Lamb jii - M...
#senegal #kebetu #team221
Voici un extrait des vidéos oustaz Alpha Ba ha pour des éclaircissements sur le polythéisme …
#senegal #kebetu #team221
spécial live Cii LERAL LEUNT LEUNT gnii wottee woo abb yónnent guinaaw sunu YÓNNENT MOUHAMMAD ﷺ
11 Mai
#senegal #kebetu #team221 LIVE - IMAM CHEIKH ALPHA BA - PAROLES AUX AUDITEURS - WOOTE WOO ABB YÓNNENT GUINAAW SUNU YÓNNENT... #sénégal #senegal221 #magal #merci #mouride #youtube
Maktaab Oustaz Alpha Ba
t.me/MaktaabOustazalphaba
︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾
t.me/MAKTAABSALAFIYA
📡:t.me/reflexionsurlapensesoufis
t.me/kitaabtawhidaboubacrysall
t.me/LerralDiine
t.me/passpassbouweer
t.me/Sharkhsounna
t.me/siffatusallat
#senegal #kebetu #team221

Пікірлер: 146

  • @KAADUDINEEJITV
    @KAADUDINEEJITV11 ай бұрын

    Aimez la vidéo abonnez vous et partagez n’oubliez pas d’activer la cloche de notification pour les prochaines vidéos

  • @asannediop3826
    @asannediop382611 ай бұрын

    Machallah imame alpha ya baah ci Sénégal yalna yalla fayla yiwe amine yarabi

  • @user-bd1es6pb6u
    @user-bd1es6pb6u9 ай бұрын

    Yallah nafi yallah déguéral souna dakal gnou bida ak sirkou thii rewmi

  • @DIOBISTO
    @DIOBISTO2 ай бұрын

    masha-Allah ouztaz Alpha Ba Younous, Sokhna Khady et toute l'équipe, vous faites un bon travail masha-Allah ❤❤❤

  • @Soldarousheikhomarsall
    @Soldarousheikhomarsall5 ай бұрын

    Que Allah protégés Oustaz Alpha et son équipes ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @alioudiallo3019

    @alioudiallo3019

    4 ай бұрын

    Equipe de quoi?

  • @mouniroudiop717
    @mouniroudiop71711 ай бұрын

    Kham kham nekhna machala mawlana cheikh Ibrahim niass borom faydatoul tidiane.

  • @Aminabarham5260
    @Aminabarham52604 ай бұрын

    Ndeyssane amna niou rérrrrrr wayyy Baye Niass mo bahhh❤❤yalla n'agnu yalla fayal Baye ...Baye niass mo bahhhh ❤❤

  • @dawdatouray266
    @dawdatouray26611 ай бұрын

    Masha'Allah oustaz Alpha ba leral yi Amna solo yallna yallah fai Len

  • @user-jk3ne9pd4f
    @user-jk3ne9pd4f7 ай бұрын

    Sen soi-disant mandou bobou c que les vrais musulmans ne peuvent pas vous regarder mentir sur notre religion 😢yalla gniou yalla moussal thi tarikhayi 🤲🤲

  • @Aminabarham5260
    @Aminabarham52604 ай бұрын

    Cheikh alpha hamo yalla nopil kou hamoul yallah perte gua demlen hamidj yalla nahh s'en dundeu bi am ndieurign❤❤

  • @ismailadiallo7819
    @ismailadiallo781911 ай бұрын

    Mashalla c’est instructrif quand il y a de l’écoute, merci à toute l’équipe kaadu dînée plus particulièrement à Cheikh alpha, j’apprends bcp de vos vidéos. Mais mon homonyme Ismaila Diallo dafa tangue mom lol. Merci encore une fois

  • @IKS_Barhama

    @IKS_Barhama

    11 ай бұрын

    Mendoulen mogun

  • @ismailadiallo7819

    @ismailadiallo7819

    11 ай бұрын

    @@IKS_Barhama du n’importe quoi vous voyez le mal partout

  • @babanjie6326
    @babanjie632615 күн бұрын

    Walahi warouwoun Sante njie

  • @dawdatouray266
    @dawdatouray26611 ай бұрын

    Nooo! Senegal dinee bu lerr problem la tofu, Baye len sen serigne si te topu all quran ak sunnah.

  • @alassaneseye2191

    @alassaneseye2191

    11 ай бұрын

    Billahi alquran ak suna rek moy deug

  • @asannediop3826

    @asannediop3826

    10 ай бұрын

    Dafa lére wallahi

  • @laoucouledesruissaux4495
    @laoucouledesruissaux449511 ай бұрын

    Sénégal dal gno meuneu,beugue sén moromou nit,bamou geuneulén sén borom Allah aza wajal. Tarikha xipiléne ndakh dagéine réér

  • @lemirmcsbs2654

    @lemirmcsbs2654

    9 ай бұрын

    Iow momou y'a rerr ta niak dégue dégue

  • @laoucouledesruissaux4495

    @laoucouledesruissaux4495

    9 ай бұрын

    @@lemirmcsbs2654 dîné dou affairou dég dég,mais dangay diang pour xam,âme xam xam bou sél bi té Moy Al Quran AK sunna point. D'où Serigne Touba dou maodo mailk,ay bay lay Aki bay Niass. Tarikha mom tardema AK lore sa bopp adunak Al ahira bou mak leu Nék lén mo geuneu si yén bala dé Di nieuw.bida AK bokalé tél géni doundé.

  • @alassaneseye2191
    @alassaneseye219111 ай бұрын

    Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba leral yi amna solo yalla na len yalla faye sen ligueye rafetna

  • @user-ef9yj7ld6h
    @user-ef9yj7ld6h9 ай бұрын

    baye niass sunu mrom la kéy ndakh mindéf la yallâh modoul mrom ndakh brom leu allâhou akbar

  • @user-wt9rd2bw9i
    @user-wt9rd2bw9i7 ай бұрын

    Yallah na yallah goudal sène fane Machallah wakhtane bi amna solo

  • @oustazeugmailcomndiaye
    @oustazeugmailcomndiaye11 ай бұрын

    Merci beaucoup oustaz alpha ba

  • @user-gw7ef7bl3x
    @user-gw7ef7bl3x4 ай бұрын

    Yalla rek mofi nék yalla ken douko giss nono lol Amoul ok ❤❤

  • @thiamelhadji5299
    @thiamelhadji529911 ай бұрын

    Alpha BA ,si tu invite une il faut la donne du temp il va repondre ,apres tu repose un autore question ,parce que il ya des persone qui ecoute

  • @Rassoul1425
    @Rassoul142511 ай бұрын

    Ya ouztaz mangui laye nouyou dila ziar yangui guidi gagni té mane guidi ngama

  • @falloutoure135

    @falloutoure135

    11 ай бұрын

    Macha Allah

  • @mouhameddiop8002
    @mouhameddiop80024 ай бұрын

    Salam sama Mbokk Dioulitt Yii, Ma Ngui niann Nioun Dioulitt Yeup Yalla diégal niou souniou Bakar Yi adouna, Mousseul niou Mougueulou Bambel ak Mougueulou Safara

  • @baboucardiop5121
    @baboucardiop512111 ай бұрын

    ❤ machallah ya oustaz Alpha ❤️❤️

  • @abdouazizsowe5125
    @abdouazizsowe51259 ай бұрын

    As salamualaikum. Man Gambie laa jogay, mang len di nyan ngen bai gaii nyu pareh sen wahi purr ngen munlena gena japa INN SHAA ALLAH. Lw dut dega c diineh amut proof. Sorlen bayeh gaii nyu wahh INN SHAA ALLAH gaii gena hamneh nekun c dega. Gambie fii sahh gaii barrinen fhi.

  • @elhadjiboubacardiallo4099
    @elhadjiboubacardiallo409911 ай бұрын

    ❤❤❤❤assalamoualeykoum

  • @user-oy3kb1hl2b
    @user-oy3kb1hl2b5 ай бұрын

    Souna sikaw❤❤❤

  • @mouhamedbeckefall4389
    @mouhamedbeckefall43899 ай бұрын

    Machallah yalla naléne yalla dolli yiiw ak soutoureu

  • @user-nb1le1pq3h
    @user-nb1le1pq3h11 ай бұрын

    والله ماشاءالله تبارك فيكم

  • @biranedjiba9991
    @biranedjiba999110 ай бұрын

    Wakhi Baye bi amul benn dioumté , adouna degg ak niakk degg moo fi Nek. Il faut comprendre qu'il existe d'énormes codes dans le langage des saints. Toubab nénaa l'ami de ton ami est ton ami. Aucun d'entre nous ne pas refuser que Baye était au service de L'islam. Donc l'aimer c'est aimer l'islam ,un chemin vers le paradis.

  • @user-rj9yh6mi7c

    @user-rj9yh6mi7c

    6 ай бұрын

    Diné amoul code

  • @ablayethiam38
    @ablayethiam389 ай бұрын

    MachaAllah oustaz alpha

  • @alinesamb5006
    @alinesamb500611 ай бұрын

    السلام عليكم ورحمة الله وبركاته كيف حالك أنت بخير أحسن الله إليك ماشاء الله بارك الله فيك أخي الكريم الشيخ الفاهم باه حفظه الله ورعاه ماشاء الله ❤❤❤

  • @Aminabarham5260
    @Aminabarham52604 ай бұрын

    Ki kay d'où ouztaz comédien leu😂😂😂😂

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo972711 күн бұрын

    Bay niass masoul dioum هو من أولياء الله الذين لاخوف عليهم ولاهم يحزنون

  • @basirubadjie4352
    @basirubadjie435210 ай бұрын

    Masahallah ouztass alpha

  • @Aminabarham5260
    @Aminabarham52604 ай бұрын

    Walahi damalen yeureum😂😂😂bilahii yeureum nalen enplus ligueini wah ay ree lamay def nena thi yonente psl thi yalla kay 😂😂😂yeineu beugolenn yonente bi psl gueumolenn yalla😂😂😂😂 mntah damalen yeureum walahiii

  • @OureyeSeck
    @OureyeSeck3 ай бұрын

    Alpha kou beuy waliyou roye ko tope ko deug mélna ni yonénte ngua beug tope ko wala roye ko nakh si islam saria souna fikh tassawouf nguay nék di déf lou bakh ba déé yalla yeureum la dougal la aljana🧏🏾‍♂️ al oulama ou warrassatoul anbiya🧏🏾‍♂️ borom xam xam yi gno donu yonénte yi rawatina waliyou bou mélni baye🙏🏾👍🏾

  • @mouhabarxam70
    @mouhabarxam7011 ай бұрын

    délène deglou ki wakh ni battou djiguen awra leu bimou ko wakhé degglou len ko moguen. Mais nguen di imposer nitt ki mou indi dalil té dollen deglou. Moune nguen bagn koulen accuser té nguen ci live bi doule. Baye Niass doussen morom régler len.

  • @boubacarbadji1805
    @boubacarbadji180510 ай бұрын

    Manchallah manchallah

  • @alioudiallo3019
    @alioudiallo30194 ай бұрын

    Koulou domou adama adama dayii ndioum. Waw. Sadak ta rasoulouh. Mais rasoulh dou dioum deugleuh. D'accord mais waliou yallah dou dioum deugleu Baye waliou yallah deugeuleu❤ leu

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo972711 күн бұрын

    Waw yonénte dou valiyou thi mom la أولياء ditybé moom happuna valiyou

  • @ibrahimatanordiallo1382
    @ibrahimatanordiallo138211 ай бұрын

    Hayakoumou Lahou wa bayààkum barakalahou feekoum

  • @Aminabarham5260
    @Aminabarham52604 ай бұрын

    Ham ham boko amer waro diko waner pour tuteul thi sa moromu dioulit...mais malheureusement touss hamolen ko😂😂😂😂😂

  • @omardia9302
    @omardia930211 ай бұрын

    Sunnah nekhna

  • @abisatousinghateh5830
    @abisatousinghateh58309 ай бұрын

    Mashaa Allah..❤❤❤you for the fact that you people are saying..let returns to quran and sunna..drama's r too much in the deen..

  • @moustahadrame6979
    @moustahadrame69795 ай бұрын

    Nioune Baye niass rk ❤🎉🙏

  • @user-ui2rk6mq9w

    @user-ui2rk6mq9w

    15 күн бұрын

    Nioune yalla sougnou borom reck

  • @xutbatv4516
    @xutbatv451610 ай бұрын

    Assalamou alaïkum... Barack'Allahou fik. Mais Ismaël dafaay xawa perturbé débat bi. Oustaz alpha moy modéré donc bù kénn duggé laisser le développer avec oustaz alpha. C'mieux Sinon le débat est détourné de son sens et son importance Barack'Allahou

  • @bineta1752
    @bineta175211 ай бұрын

    Ouztaz Parle des castes au Senegal

  • @ZizaFaye-ls4nf
    @ZizaFaye-ls4nf9 ай бұрын

    Grand bayilen baye Niass svp baye Mossoul wakh si loudoul Lou bakh si yalalh Ak yonenete lingen di deff bakhoul . Delen layè birr lingen dom ni erreur la mais boulen vilipender Baye leer n’a Len ni kifa geuna ndaw molen eup kham kham

  • @siacamane3361
    @siacamane336111 ай бұрын

    Longue vie a vous ❤ ya oustaz ❤ ❤ Ba

  • @mouniroudiop717
    @mouniroudiop71711 ай бұрын

    Niake cible ak objectif wessouwoul koune achhadou an lahilahailala wachadou anamouhamadarasouloulah ngay weur aye ndioumbtem. Ibadou bou nek tidiane wala tidiane bou nek ibadou islam niakoussi pertoussi.bagnou geume yalla gnoune gneup silagnou ame tawfekh.

  • @Pastef859
    @Pastef8599 ай бұрын

    Liguey bi rafetna waay faw sa gaayi ñu wañi wérenté bi té ñuy baayi invité yi di wax séén xalaat

  • @jannehtamsirahmathe872
    @jannehtamsirahmathe87210 ай бұрын

    Ya Ismail thank you so much

  • @AbouDiop-id1vx
    @AbouDiop-id1vx4 ай бұрын

    إعدلو خير من تقوى ...mandou mogeun ragal yalla

  • @Babe-FaLilOu
    @Babe-FaLilOu11 ай бұрын

    Ismaila mii dfa wareu bayi di perturber tei bayi Oustaz Alfa modérer parce que mo geun dal Sinon mashaAllah Alquran ak Sunna rek ♥️

  • @xutbatv4516

    @xutbatv4516

    10 ай бұрын

    Lolù tamitt deugg leu... Daay perturbé

  • @mouhameddiop8002
    @mouhameddiop80024 ай бұрын

    Diangalé bi amna Solo lolou mais dilenn niann rekk Discipline djitou ci lepp, Mou andd ak Deglo ci layy eupp ndieurign, Ma ngui Baalou nieup nakk Yalla naniou Borom bi Bolé diégueul

  • @amadoulamine
    @amadoulamine11 ай бұрын

    Yala naniou yla fayal baye niasse 😢

  • @mamadousy6312

    @mamadousy6312

    11 ай бұрын

    😢😢😢amo lene kham kham saga rek ak khass té moy seni pass pass ak menaces allhur an ak sunna yonnente psl moy degue

  • @amadoulamine

    @amadoulamine

    11 ай бұрын

    Ah yala naniou yala sopi kon

  • @mamadousy6312

    @mamadousy6312

    11 ай бұрын

    Tarikha yi gno saboté l islam tardel Sénégal am développement trompé né ñiou jeunesse bi topal sunnah seydina mhmd psl mom la yalla garantie cou ko top dioub

  • @amadoulamine

    @amadoulamine

    11 ай бұрын

    @@mamadousy6312 man dh niom lay Roy sonou mag niou bakh ngi

  • @mamadousy6312

    @mamadousy6312

    11 ай бұрын

    Non royal ki ki yalla yonni té moy yonnente bi psl ndakh bess bo fato ba dou gal la sa bamel ken ndou la ladj sou ñiou mag ñi ya ngui thi erreur sama wadji tarikha yi neckoul lou yalla reconnaître li yalla reconnaître moy sunnah seydina mhmd psl

  • @cheikhbassiroulo9727
    @cheikhbassiroulo972711 күн бұрын

    عليكم با لصدق والأمانة. واتركوا المجادلة فالشريعة دستور. ولاكن الحقيقة لا يعلمها احد الابعد المعاينة .فكلامكم هذآ لاينتفع به المستمعون.

  • @moussaseck9513
    @moussaseck95132 ай бұрын

    Waw délene deglou Walahi khamo lene dara

  • @user-qv2gr3ck1h
    @user-qv2gr3ck1h5 ай бұрын

    Salam diadieuf

  • @user-nb1le1pq3h
    @user-nb1le1pq3h11 ай бұрын

    Salam alpha sonal ga dof si nitt yi d 😂😂😂😂😂😂😂😂ñiy nitt lañiou gém

  • @user-vt6on9xk3e
    @user-vt6on9xk3e9 ай бұрын

    Baye nias dou séné morome

  • @bn5523
    @bn552310 ай бұрын

    Alpha ba you must leave baye Niass alone Baye niass douca morome demal ngua diangui tu fais de l intoxe khamo dara

  • @RamatoulayeDiallo-eb7yr
    @RamatoulayeDiallo-eb7yr6 ай бұрын

    L'islam mandou amou fa degeu bii leniouy wakh falouss demal tok

  • @ElhadijDiop-hd4dz
    @ElhadijDiop-hd4dz11 ай бұрын

    Al pha ba kou rew la bilaye

  • @AbouDiop-id1vx
    @AbouDiop-id1vx4 ай бұрын

    Yalla wathiewoul ahlou sunna nitt la wathié ima dioulit aw ima yefeur

  • @AbouDiop-id1vx
    @AbouDiop-id1vx4 ай бұрын

    Bayilénne duuuuul yaye Aïcha da done binde mais dawoul diangal goor

  • @ramatoulayembow1942
    @ramatoulayembow19429 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤

  • @alphonsesarr4105
    @alphonsesarr41059 ай бұрын

    LI NGENI WAX DU DEUG SI YEEN NDAX NEKO LEN SENEGAL BA PARER DI NEBETU RK SURTU KU JIGEEN KI AMOLEN BEN RESPECT SI NITT GNI

  • @asannediop3826
    @asannediop382611 ай бұрын

    Salam mbok yi Loutah dou ngou dème topou alxouràne AK Sounnah rek kassé am diamou bou baah wallahi

  • @moussaseck9513
    @moussaseck95132 ай бұрын

    Alpha amo kham kham 😃😃bilahi Daga diang rek mais kham kham outti ko tè bagnia reuy

  • @ibrahimandour9331
    @ibrahimandour93314 ай бұрын

    Bo gueumoul tarikha sa affaire leu nous sommes de nos tarikhas.Nguir yalla laisse nous tranquillement.

  • @meloman2992
    @meloman299211 ай бұрын

    Beneen saï saï migui ni Boy Alpha domii Omar sall dji mane damay sant yalla am xol bou fèkh ci dilen deglou 😂 souma paré dislike ta rombou

  • @mouniroudiop717
    @mouniroudiop71711 ай бұрын

    Ndeysane li rafete dou bagna oute dou oute tamite. Li yeupe thiofel bou nite di ame si nite moko geune.insaniyatou mo djitou leep

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane706611 ай бұрын

    Alpha Ki do fi wakh dara bayi ko mo dem

  • @cheikhsadiboudiedhiou309
    @cheikhsadiboudiedhiou30911 ай бұрын

    Assalamouha leykoum

  • @sunnialiber4868
    @sunnialiber486811 ай бұрын

    Teye waxtaan bi nèex na, wayé jambar yi faut que ñu bayi interrompre participants yi.

  • @alhassanefall9154
    @alhassanefall91549 ай бұрын

    Assalamualaikum machallah alpha yalla Nanou yalla sahal sii suna mais batou jiguéne dankoy téré mouy diageu alkhouran si kaw

  • @sadinandiaye8870
    @sadinandiaye88708 ай бұрын

    Alpha, laisse les parler. C'est ça le " sel " de l'émission. Après, tu conclus, en mettant sur la table, ce qu'un dit le coran et les hadiths.

  • @fatimadieye9478
    @fatimadieye94788 ай бұрын

    😂😂😂😂😂 soubhal lahh Raye nama néna mane guéne ma wathié .. qu'Allah vous récompense pourtant mane Di séne bokk yaguena dégue lolou

  • @user-rk1jl1bf8t
    @user-rk1jl1bf8t8 ай бұрын

    Lathe pour sabôté wla pour khame dingatt baxoule nagnoule makk ngi doulén wangi dara li soxor la

  • @user-mf4sr8kr6j
    @user-mf4sr8kr6j11 ай бұрын

    Gnibil guine te bayi sounou rewmi ga y diakhasse alpha

  • @user-el3bn6fh6n
    @user-el3bn6fh6n9 ай бұрын

    DEUG rek moy moudiou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @dokydiop7594
    @dokydiop759410 ай бұрын

    Boy alpha 😂khagne ngay nopalé guou fall yoe yagui wakh batay kéne ba falé woula niou guéne beugue baye niass té nake ma xam lasi léne lousi kobé carcko baye niass rk doy naniou adouna ak lakhira

  • @harounasow4965
    @harounasow49659 ай бұрын

    Il faut juste éviter de la faire paler sur le plateau elle peut écouter ou bien répondre par message .

  • @indigne2161
    @indigne216111 ай бұрын

    Quels remèdes apportés aux maux de ces sofiankés enkoûtés ? Si Khuran &Sunnah ne leur viennent en aide , quelle effroyable destination

  • @adamaDiopp
    @adamaDiopp4 ай бұрын

    😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdoufaal786
    @abdoufaal78627 күн бұрын

    Baye niass mofi indi ndiabar Kat yi talibe baye niass yi sen pas pas bi ay fen la

  • @user-mf4sr8kr6j
    @user-mf4sr8kr6j11 ай бұрын

    Alpha khamo dara demal diangui gani innawaliyilah neckoul ci alkhouran yameun fen sourate Anfal aya 196 ان ليي الله الذي نزل الكتاب وهو يتول الصالحين

  • @mouhabarxam70
    @mouhabarxam7011 ай бұрын

    Nitt mounoul Beug Baye té bougoul Seydina Mouhamed PSL

  • @BocaramadouBa-qo4kn
    @BocaramadouBa-qo4kn3 ай бұрын

    Moi je crois en cette voyance. Dieu on peut le voir. Si on se réfère au coran parlant sur l'aveuglement. Allah nous parle de l'aveuglement coeur non des yeux. Qui est ce qui voit ? Comment voir avec le coeur ? Aussi est_il à rappeller, noter votre contradiction monsieur alpha, Comment peux tu dire que tout ce que le prophète est vérité. Et amener le hadith du prophete psl; qui dit: tout être humain se trompe. ? Mouhamed psl n'est-il pas un humain? S'il n'est pas humain qui il est ?

  • @bourybarry3911
    @bourybarry391111 ай бұрын

    Nittou charia dafa yaggeu khekh nittou haqiqa. Wayye c la face d'une seule pièce de monnaie.

  • @mouhamedsow7720
    @mouhamedsow772011 ай бұрын

    As salamu haleykum! Debat pour mu productif il faut que mou am ap modérateur pour niu meunssi diariniu. Gars yi daniuy daganté seine birr rek. Ku dieul parole key nagn ko bayi mu diehal bala niuy diokh kenen bokk pour mu nekh

  • @papamalicksarr9305
    @papamalicksarr93053 ай бұрын

    mandou baaxna

  • @zaldiop6293
    @zaldiop62934 ай бұрын

    Oustaz alpha stp il faut lesser borom tarikhayii exprimer

  • @user-ui2rk6mq9w
    @user-ui2rk6mq9w8 ай бұрын

    Alxouran ak sounnah kasé moo meuneu défar Sénégal

  • @alkhamiss
    @alkhamiss9 ай бұрын

    Youssouf mi day diakhasé yeup way haaaaa

  • @moussaseck9513
    @moussaseck95132 ай бұрын

    Kay ma tontou le si sa 3 question yi 1 Baye limou wakh ni kouma guis Dem aldiana lolu d’où Dara beug baye niass moy beug yalla rek moy beug Seydina Mohamed -Mohamed Ibnou abdallaa bokoul ak Mohamed rassoulloullaa

  • @user-yd6ml1ho3m
    @user-yd6ml1ho3m9 ай бұрын

    Alfa Nay andak dal AK dégulo couy wakh nga bayico mou wakh bou naré Bari wakh nga teuth microm wakhco mou dal comsa gnoune gnou comprends

  • @mouniroudiop717
    @mouniroudiop71711 ай бұрын

    En tout cas le soleil se lèvera demain a l est et se couchera a l Ouest.chacun est libre de faire ce qui lui convient de sa vie.mais la différence ne doit pas être un signe d adversité. La beauté d un tapis est dans la diversité de ses couleurs.arretez de vous ridiculiser Lou yalla amoul yonanti amouko kene meunouko ame.nopaloulene

  • @harounasow4965
    @harounasow49659 ай бұрын

    MAIS DJIGUENNE CI NATURAM LA DI CHARME NEKHAL BAT

Келесі