Paroles aux Talibe de Baye Niass cii sen paas pass you doy waar yii 🤔 - Live TikTok Oustaz Alpha Ba

🚨Urgent: Paroles au Baye Fall sur le NDIGEUL Contradictoire de S Mountakha Mbacke - Oustaz Alpha Ba
• 🚨Urgent: Paroles au Ba...
---
🚨Urgent Ay leral cii Ibrahima Guéye Khassida donn weur kaba gua ca Makka akk … - Oustaz Alpha Ba Ha
• 🚨Urgent Ay leral cii I...
#senegal #kebetu #team221
🚨Urgent - Lamb jii - Messages aux lutteurs ⁉️ - Oustaz Alpha Ba H-A
• 🚨Urgent - Lamb jii - M...
#senegal #kebetu #team221
Voici un extrait des vidéos oustaz Alpha Ba ha pour des éclaircissements sur le polythéisme …
#senegal #kebetu #team221
spécial live Cii LERAL LEUNT LEUNT gnii wottee woo abb yónnent guinaaw sunu YÓNNENT MOUHAMMAD ﷺ
11 Mai
#senegal #kebetu #team221 LIVE - IMAM CHEIKH ALPHA BA - PAROLES AUX AUDITEURS - WOOTE WOO ABB YÓNNENT GUINAAW SUNU YÓNNENT... #sénégal #senegal221 #magal #merci #mouride #youtube
Maktaab Oustaz Alpha Ba
t.me/MaktaabOustazalphaba
︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾
t.me/MAKTAABSALAFIYA
📡:t.me/reflexionsurlapensesoufis
t.me/kitaabtawhidaboubacrysall
t.me/LerralDiine
t.me/passpassbouweer
t.me/Sharkhsounna
t.me/siffatusallat This stream is created with #PRISMLiveStudio #senegal #kebetu #team221

Пікірлер: 119

  • @laminegaye6130
    @laminegaye613010 ай бұрын

    Salam à tous la réponse selon le coran :« Et lorsque Moïse vint à Notre rendez-vous et que son Seigneur lui eût parlé, il dit : « Seigneur! Montre-Toi à moi pour que je puisse Te voir. » Dieu dit : « Tu ne Me verras pas, mais regarde la montagne; si elle demeure à sa place, alors tu Me verras. » Mais lorsque son Seigneur manifesta (Sa) gloire à la montagne, Il la pulvérisa et Moïse s’effondra, foudroyé. Lorsqu’il revint à lui, il dit : « Gloire à Toi! À Toi je me repens et je suis le premier des croyants. » (Coran 7:143)

  • @docteurgoudiaby7544

    @docteurgoudiaby7544

    10 ай бұрын

    Masha-ALLAH cet verset suffit pour dissiper leur croyance

  • @adjafatoudiassdiouf8759

    @adjafatoudiassdiouf8759

    7 ай бұрын

    Ma shaa Allah qu'Allah nous pardonne 😢

  • @papaabdoulayethiam9878

    @papaabdoulayethiam9878

    4 ай бұрын

    😅😅😅😅tu n'as rien compris

  • @lugodseye4124
    @lugodseye41249 ай бұрын

    Ma khady je t'apprécie beaucoup Masha'Allah..!!!

  • @Soldarousheikhomarsall
    @Soldarousheikhomarsall5 ай бұрын

    Koumounull kholl djénte bi 5 seconde noye guissè yalla subhanallah Allahu akbar 😢😢😢😢

  • @DIOBISTO

    @DIOBISTO

    2 ай бұрын

    Vraiment, merci pour cette réponse pédagogique

  • @sotornoahs7411
    @sotornoahs74119 ай бұрын

    "La tudrikuhul-absaru wahuwa yudrikul-absara. wahuwa llateeful khabeer" . La vision ne l'aperçoit pas, mais il perçoit [toute] la vision ; et Il est le Subtil, le Connaisseur. Continuez le verset complet et voyez comment Ya'Allah se manifeste dans son être.

  • @baidyniang5806
    @baidyniang58068 ай бұрын

    Souniu BOROM lougni guiss moy ay NDOGALAM .ay MISSALAM WANTE GUIS YALLA COMME NI NGAYE GUISSE NIT BI NEK SA KANAM MENOUGNOU GUISSE NONOU YALLA YALLA LOKOY GUENA GEUM MOULAY GUENA WONE AY MBIR YOUY TAKH NGA GUENA HAM LOULAY DJIEGUEL YALLA MOULAY DIEURINE SI SA DINE YALLA BOKOUL AK LENE ÉVITER DE VOULOIR DÉCRIRE UNE IMAGINATION IMPOSSIBLE MAI NGEUME CELA EXISTE DANS LES COEUR❤

  • @user-kl7tx8bs1e

    @user-kl7tx8bs1e

    5 ай бұрын

    Yaw môme dagua Mouna féen

  • @user-kl7tx8bs1e

    @user-kl7tx8bs1e

    5 ай бұрын

    Guisgua domi Adama yaw mouno donne yallah wayyé yallah mounala donne

  • @ousseynoudiarra9578
    @ousseynoudiarra957810 ай бұрын

    Dieureudieuf oustaz alpha Ba ak younouss ak oukhti ma khady tôt ou tard deugeuh Moy moudiou

  • @alassaneseye2191
    @alassaneseye219110 ай бұрын

    Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba leral yi amna solo yalla na len yalla faye sen ligueye rafetna

  • @abdoulayeba7078

    @abdoulayeba7078

    10 ай бұрын

    Amine ya Rabbi

  • @peulbouhighbeatz
    @peulbouhighbeatz10 ай бұрын

    Elhadj Ndao Dieureudieuf 🙏🏽❤️

  • @user-dd3sy2tu4r
    @user-dd3sy2tu4r7 ай бұрын

    Merci oustaz alpha ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @2rayone760
    @2rayone76010 ай бұрын

    Masha-Allah oustaz alpha leral yi am na solo yalla na yallah faye len

  • @user-gw7ef7bl3x
    @user-gw7ef7bl3x4 ай бұрын

    Merci beaucoup you nous ❤

  • @AfaneFall
    @AfaneFall8 ай бұрын

    Baaye niass khadioul seene bopp

  • @user-ui2rk6mq9w
    @user-ui2rk6mq9w9 ай бұрын

    Oustas alpha ba yalnako yalla samou amine yarabi

  • @papendenekonte9203
    @papendenekonte92032 ай бұрын

    Yallah ken douko guiss mais dankoy doundou dakh islam lougnouy doundou là mais d’où lougnouy guiss rombou mais lougnouy doundou a vie

  • @AbdoulayeSFAYE
    @AbdoulayeSFAYE5 ай бұрын

    Alpha il faut laisser le temps aux invités de pourvoir développer leur point de vue. Par contre El hadj a bien justifié ses propos , il est cohérent. 23:58

  • @DIOBISTO
    @DIOBISTO2 ай бұрын

    masha-Allah ouztaz Alpha Ba, Younous, Sokhna Khady et vos autres amis, vous êtes entrain d'effectuer un travail extraordinaire, Certains marabouts ont écrit beaucoup de conneries

  • @AbdouSow-gy5yi
    @AbdouSow-gy5yi6 күн бұрын

    wahktane bi machala mé yalla Kou fénie la Waya niepe guisouniouco lolou yalla la sobe diante sah niepe dounkoguis nah Goumba douguis diante 😂😂😂

  • @adioumadiagne7607
    @adioumadiagne76075 ай бұрын

    Wouy alpha gat khamo ko😂😂

  • @user-hn9rh8rq6x
    @user-hn9rh8rq6x3 ай бұрын

    ‏ما شاء الله❤❤❤❤❤

  • @amibabou642
    @amibabou64210 ай бұрын

    Sénégalai mo doye ware Allahou Akbar te guene yame thi. Sene Serigne yii yalla borome la d'où morome

  • @sidymane6860
    @sidymane686010 ай бұрын

    Dett 😂 soubhanallah, saway yaw mi teunk yAllah thi assaman kay yaané yAllah dafa teulé. Dangay wakh di wedi sa bop 😂

  • @bahslmane6033
    @bahslmane60339 ай бұрын

    Macha allah oustase bah amna solo dieu ont le voir pa dans la vie jamais gayii amoniou xam xam ont discuté pour ne rien que nous guide dans le bon droit chemin que dieu vous bénisse vous tous dû courage

  • @SeydouThiam-zj5mp
    @SeydouThiam-zj5mp10 ай бұрын

    Assalamou aleykoum wa rahmatoullahi wa barakatouhou. QU'ALLAH nous accorde la clairvoyance et nous protège contre les ambiguïtés. BarakaALLAHOU FIIKOUM cheikh Alpha avec ton staff.

  • @rahmatoullahcisse1090
    @rahmatoullahcisse10905 ай бұрын

    Mounane ko alkatel la tiow diouboul oustaz alpha 😂😂😂😂 force a la sunnah

  • @amathbarhamfall2444
    @amathbarhamfall24449 ай бұрын

    Salamou Aleykoum Alpha nga Balma loutakh ngaye Andi aye diminutif thie sa diganté ake sa borome

  • @adioumadiagne7607
    @adioumadiagne76075 ай бұрын

    Giss Yàlla du debaa, xanaa du moo wax ne: moo feeñ té moo ëpp lepp ? Ku ko gisul dengaa feebar demal fajuji...

  • @CheikhThioye-op6ns
    @CheikhThioye-op6ns10 ай бұрын

    Machallah alpha mo degg arabe machallah

  • @DIALOGUE-DEUG
    @DIALOGUE-DEUG10 ай бұрын

    Merci à vous ❤❤❤

  • @AfaneFall
    @AfaneFall8 ай бұрын

    Alpha sa xam xam soriwoul

  • @Soldarousheikhomarsall
    @Soldarousheikhomarsall5 ай бұрын

    Que Allah nous offre des millions de Alpha ba ❤❤❤❤

  • @OuseynouWilane
    @OuseynouWilane10 ай бұрын

    Sona rek. Moy daga

  • @issakabarry4105
    @issakabarry41059 ай бұрын

    Machallah Ousas alpha❤❤❤❤🕋🕋

  • @idrissadiop9364
    @idrissadiop93645 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤

  • @amethdiaw3475
    @amethdiaw347510 ай бұрын

    بارك الله فيكم

  • @Cheikh-dp8dy
    @Cheikh-dp8dy6 ай бұрын

    Alpha un bon musulman doit avoir le sens de l'écoute si tu veux savoir il faut écouter l'avis des gens même s'il raconte des bêtises vous manquez de pédagogie la plupart des ousstass sénégalais non pas de pédagogie. Wa salam

  • @AfaneFall
    @AfaneFall8 ай бұрын

    قد جاءكم بصائر من ربكم فمن ابصر فلنفسه ومن عمي فعليها

  • @moustahadrame6979
    @moustahadrame69795 ай бұрын

    Baye Niass point ❤❤❤

  • @bayemassaertv6331
    @bayemassaertv63319 ай бұрын

    Baye niasse actualment a des fideles jusqu'a chine indonesia etc... Plus de 200 millions de fideles dans le monde

  • @deug648

    @deug648

    9 ай бұрын

    C pas un argument sheytan à des milliards de fidèles dans ce monde

  • @bayemassaertv6331
    @bayemassaertv63319 ай бұрын

    Non Baye c'est autre chose il a dit mom garantí woul Ken aldjiana djiamou len Yalla...bou len ko sossal...tarbirou Ken doukobeakhal ak kountarbiroul

  • @mamadiame9863
    @mamadiame98636 ай бұрын

    Ma challah hermanos

  • @ibrahimasarr8529
    @ibrahimasarr852910 ай бұрын

    Ma cha ALLAH k'ALLAH vs agréé

  • @papedieresane1084
    @papedieresane10845 ай бұрын

    Alpha daguay deglou pour nite yi dilene deglou meun si dieurignou. Li pour gneup dieurignou si le coran degeudegeu là ladji

  • @amathbarhamfall2444
    @amathbarhamfall24449 ай бұрын

    Nguéne Balma Wallahi soriguéne loooole ake séne borome fi ak beugouléne séne borome ba diko beugue guiss ak séni beutou bope wala diko beugue fone ake séni pakhou bakani bope wala diko beugue mosse ake séni lamignou bope wala guéne beugue séne borome ba diko beugue dégueu ake séne nopi bope wala sakh guéne beugueko lale ake séne barami loxoyi

  • @janesarr1299
    @janesarr129910 ай бұрын

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💕💕💕💕♥️

  • @cherifbassiroudiedhiou3284
    @cherifbassiroudiedhiou32845 ай бұрын

    Alpha sa Yaye ak sa papeu niola fétéh kaw téh yén niét yii yeup yénangui tchi souf sén birr kër

  • @AmadouSow-it6hh
    @AmadouSow-it6hh10 ай бұрын

    Salam ziar contane si yéne Yalla n'a barkél leup

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane706610 ай бұрын

    Am na soulo torop yala nalén yala samou te fey lén yéw

  • @ousseynoudiarra9578
    @ousseynoudiarra957810 ай бұрын

    Walay alkhourane ak sunnah rk Moy deugeuh wa biirty biirty danio dof

  • @moussaba8187
    @moussaba818710 ай бұрын

    Si seulement je pouvais voir ALLAH au moins, j'aurais une maison en or .De grâce arrêter vos superstitions ,il est impossible de voir ALLAH dans ce bas monde

  • @user-kl7tx8bs1e
    @user-kl7tx8bs1e5 ай бұрын

    Waw par ce que degueu dégueume thi lako tontou

  • @maquedafoluke4541
    @maquedafoluke45415 ай бұрын

    .Chirk deug deug moy yow nga am yalla am. Ibadou yi sén woudioud bign sakhal Moy problème bi

  • @God-is-One01
    @God-is-One019 ай бұрын

    😂guiss yala key😂 thiotou ndey Sénégal le plus grave moy amna niouko geum😂😂😂

  • @HOuleySow-kj1do

    @HOuleySow-kj1do

    26 күн бұрын

    😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @abdelazizsaleh2527
    @abdelazizsaleh252710 ай бұрын

    Salam Aleikoum Oustaz Alpha, Di lene felicté ak encouragé lene ci emission bi. Vraiment debat bi am na solo mais de ngen wara kham ni personne ne detient le monopole de la verité donc ca serait bien ngen baye sene interlocuteurs niou exprimé wou. Je trouve que iow ak sa gars yi do lene maye ken mou wakh ba danel. Laissez les gens aller jusqu'au bout de leur idées sinon le debat ne point equitable. SVP essayer d'equilibrer le debat en arretant d'interrompre les gens a chaque phrase.

  • @Cheikh-dp8dy
    @Cheikh-dp8dy6 ай бұрын

    Dieu est esprit on peut pas le voire comme notr imagination un vieillard assis dans Le cieux dans sa trône comme certains dessin

  • @sambabomberefall5234
    @sambabomberefall52345 ай бұрын

    Ofait Au Sénégal on est la a parlé de ki loumou wakh weer na weiroul kaye leral li wala lele !! Le coran c clair et limpide!! Je pens li gnou wara def moy gnou defarou kon soit des vrais musulmans a travers les enseignements du prophète et un musulman dafa ame nîmou wara mell ak limou wara lambo !! Kou meune diangale lolou nank ko def kou la begue degue degue !! Diayante kham kham bi Amoul benene bene sens !!! Les barils pleins ne font pas de bruit !! En plus vous êtes dans un débat insensé Pask koi neikkkk dagua ame limou gueme te Kenna degue loula woul sa morom loudoul bègue khar foko meuna wedddeee nga weddi ko !!! Vous êtes la à faire des dualités pour lane !! Boude denigre moy takhhh !! En plus les personnes ki intervienne s disent Talibe baye niass !! Raisonnement dafa wara logique !!yalla bou lere coran bou lere bo diakarlo we ak juifff bi sakhhh mou nangoul lako!!

  • @amathbarhamfall2444
    @amathbarhamfall24449 ай бұрын

    Dama Sétlou sétantale thie saye wakh heure bo wakhé aya boulaye diéguele sa borome nga Andi diminutif thie sa firi bamou soriwatela

  • @abdoulkarimmbodji6420
    @abdoulkarimmbodji64205 ай бұрын

    Je commence a croire que Alpha et son équipe ay thiounelen. Vous n'avez pas de kham kham. Croire que Dieu etre qui se manifeste que les humains moye reure complètement. Dire que Dieu est en haut c'est ignoré complètement la physique i. e. La notion de haut et bas. Alpha ayez le courage d'aller compléter vos etudes. Vos connaissances sont tres limitées.

  • @BocaramadouBa-qo4kn
    @BocaramadouBa-qo4kn3 ай бұрын

    Debat bii mom dafa bas. Giss Yallah mom lou meuna nek la. Reste à savoir, yann beutt moy giss, ak nann ngakoy gissei?

  • @user-hb3mu5nv6y
    @user-hb3mu5nv6y7 ай бұрын

    ❤❤❤mouride la di baye fall nagoulena bép kilife tarikha diné kou nék ak beuge beuge ak sa passe passe kéne manoul wagni sama passe passe ❤❤❤dieureudieufé serigne touba diarama mame chiekh Ibrahim fall ❤❤❤❤

  • @lugodseye4124
    @lugodseye41249 ай бұрын

    Vraiment Alpha ya am foulleu😂😂😂

  • @AfaneFall
    @AfaneFall8 ай бұрын

    Alpha deeleene aagalee aayayi bamou dieelh

  • @ibrahimakane6233
    @ibrahimakane623310 ай бұрын

    Neko yalla nane la mel comme guisnako.

  • @peulbouhighbeatz
    @peulbouhighbeatz10 ай бұрын

    Merci Elhadj Ndao gni xamougn dara danio rew rek ta bari wakh

  • @mosesazizmendy2478
    @mosesazizmendy24786 ай бұрын

    boy peg is totally lost 😅😅😅 this man is soo funny 😅😅😅

  • @AfaneFall
    @AfaneFall8 ай бұрын

    Vous etes tres impoli

  • @amethdieye6944
    @amethdieye69449 ай бұрын

    تفكروا في خلق الله ولاتفكروا في ذاته فتهلكون

  • @babousarr6667
    @babousarr66675 ай бұрын

    boy sonko bi reynama😂😂😂😂😂 nooooo senegal mo nekh😂😂

  • @makinealladiop-fx6op
    @makinealladiop-fx6op4 ай бұрын

    li mo takh ebadou yi yap niou

  • @badieynba9122
    @badieynba91226 ай бұрын

    Ki d'où rou Sakh

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye75608 ай бұрын

    Ge pense guiss yallah sur terre et ne pas le voir c pas important si quel qu un est bien porter pour le voir c le prophet swa et il ne la jamais vue Mai’s au paradis on le vera tous apres la mort dis le prophet swa

  • @cherifbassiroudiedhiou3284
    @cherifbassiroudiedhiou32845 ай бұрын

    Mais pourquoi vous êtes trois contre un ?

  • @harounasow4965
    @harounasow49659 ай бұрын

    LA FEMME IL FAUT JUSTE ECOUTER SANS PARLER FRANCHEMENT C'EST MIEUX .PARCE QUE LA ON PARLE DE SUNNA PUR ET DUR DU COUP MELANGE PAS S'IL VOUS PLAITS

  • @IvesNdione-uv1ev
    @IvesNdione-uv1ev4 ай бұрын

    Sénégal thia khan rek deloulén Alpha li Mouy wakh C'est Très important Merci Alpha❤❤❤ Machalah

  • @DiakiteBaye-kb4dh
    @DiakiteBaye-kb4dh3 ай бұрын

    😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @abdoulkarimmbodji6420
    @abdoulkarimmbodji64205 ай бұрын

    Alpha surtout arreter de vous énerver. Borom kham kham dou ngawa mer.

  • @makyarrjaimemonpaysgeumbam7463
    @makyarrjaimemonpaysgeumbam746310 ай бұрын

    yéna am diott nak😂

  • @amathbarhamfall2444
    @amathbarhamfall24449 ай бұрын

    Fi ake séne borome biléne sakeu nguéne diogué thie Môme Wara délouwate thie Môme yégouléne fi ma wakh balénma beugouléne séne borome

  • @amathbarhamfall2444

    @amathbarhamfall2444

    9 ай бұрын

    Yénagui thie yonbi nake ma Cha Allah thie diéma défe limou diguelé té diéma meuyetou limou téré Ma Cha Allah

  • @amathbarhamfall2444

    @amathbarhamfall2444

    9 ай бұрын

    Lidésse nake moye guéne doli fékhé ame yare ak téguine thie bépeu mindéfou sougnou borome kou Yallah meusseu Yoni thie kawe soufe yare ake téguine mo djitou thie yawe

  • @amathbarhamfall2444

    @amathbarhamfall2444

    9 ай бұрын

    Diamouléne séne borome té beugueko ba beugue dadié ake môme fi thie adouna bala Al akhira Di yékssi

  • @amathbarhamfall2444

    @amathbarhamfall2444

    9 ай бұрын

    Diamou Yalla bakhna amna solo looole wayé beugue sa borome bay dioke Di diouli goudi bay dioye Di xalate sa borome bay dioye Di diangue Alkhour ane bay dioye

  • @amathbarhamfall2444

    @amathbarhamfall2444

    9 ай бұрын

    Beugueléne séne borome té sakou dadié ake môme fi thie adouna Yallah meuna lépeu xamna lépeu wa Salamou Aleykoum Wa Rahmatoullah

  • @MamadMohamed
    @MamadMohamed10 ай бұрын

    Alpha svp ne perdez pas votre temps avec des ignorants aveugler

  • @AfaneFall

    @AfaneFall

    8 ай бұрын

    C'est vous qui êtes des ignorants

  • @morniang1977
    @morniang197710 ай бұрын

    Alpha pourquoi do wakh si Macky Sall ni mou yoré Sénégal mais marabouillon rek nga yap

  • @God-is-One01

    @God-is-One01

    9 ай бұрын

    Oustaz la dou politique nieup xamnagn né Macky nékoul si deug. Yenn yéna geuna yess Macky

  • @peulbouhighbeatz
    @peulbouhighbeatz10 ай бұрын

    Yen weudikat yi ibadou yi niakk ngèn xorom 😂😂😂 Niakk respect tek ci Talibé Sangue Ndiaye bi wakh ci début bi lim wakh leer neu

  • @adamadmx6441

    @adamadmx6441

    10 ай бұрын

    Khamosah louy ibadou eske ay dioulit gen yen wa tariqa soss

  • @peulbouhighbeatz

    @peulbouhighbeatz

    10 ай бұрын

    @@adamadmx6441 dangen am fit😂😂😂… yenay dougueul nit gni dilen guènè ci diiné dji … dem le waar gni gueumoul Yalla gueumougn Yonent bi… nekk Len ay nit😂😂

  • @mamoudoudaff3028
    @mamoudoudaff302810 ай бұрын

    Guiss yalah dou débat...

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye75608 ай бұрын

    Il joue avec les mots qui il avance personne faut le descendre il y a d autre personne en ligne

  • @lifteneza8295
    @lifteneza82959 ай бұрын

    IL FAUT ELIMINER TES 2 COMPLICES ILS VONT GATER TES LIVES

  • @esskehbaba9984
    @esskehbaba99849 ай бұрын

    Lou gen moye gen tok chi tele nyu kholl

  • @boubacartoure1318
    @boubacartoure13189 ай бұрын

    Xam xam yamoul ak pékhé déh

  • @bayemassaertv6331
    @bayemassaertv63319 ай бұрын

    Non Baye mom waner woul bopaam

  • @Tapha_Bezos
    @Tapha_Bezos9 ай бұрын

    Gis yalla Wakhin la rek, degin la laajj

  • @lifteneza8295
    @lifteneza82959 ай бұрын

    Yagui daw rest

  • @niassbarhama2090
    @niassbarhama209010 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye75608 ай бұрын

    Il parle avec des gens on side il repete bayil modanou sindohbii lol

  • @hamidoutall2587
    @hamidoutall258710 ай бұрын

    Al ihsane moy lan?

  • @thiammady4782
    @thiammady478210 ай бұрын

    Lam tarawna rabboukoum hattaa tammoûtou. Vous ne verrez votre Seigneur qu'apres votre mort.

  • @AfaneFall
    @AfaneFall8 ай бұрын

    Sa waaye nopil kii khamoul yalla niveau yi yamoul

  • @lifteneza8295
    @lifteneza82959 ай бұрын

    Alfa boybi ammna deugg doko bayi mou wakh sinon nga danou avec sa 2compliyi alfa amoulo daara loy wakh boy bi saf sap le def mé danouga

  • @MahamadouDiaby-ti6eu
    @MahamadouDiaby-ti6eu4 ай бұрын

    nèkhoul ba nékhoul mais yaw alpha t'es nul quoi da ngay dieul yalla diohko statut nit wala chose .dieu est omniprésente yalla ngi fépeu kila gueuneu diégué saboumou khool

  • @sotornoahs7411
    @sotornoahs74119 ай бұрын

    "Wamaa ramaita iz ramaita wala innallaha rama"" Comment faites-vous avec cet ayat en sachant physiquement que c'est le prophète Muhammad SAW qui a accompli les actes. C'est l'enseignement de Cheikh Ibrahim Niass, l'entendre dépasse de loin ce à quoi vous pensez. Il parle en paraboles, pas seulement en mots

  • @KAADUDINEEJITV

    @KAADUDINEEJITV

    9 ай бұрын

    Mon frère vraiment vous avez de gros ennuis voir même de gros problèmes. Pourquoi laisser les verser coranique qui sont claires et utiliser d’autres Vc que des interprétations un peu difficile rien que poursuivre votre passion. Vraiment moi je dirais que vous suivez, votre passion est le diable le maudit a toujours des degrés sur la passion de l’homme s’il vous plaît s’il vous plaît encore soyez Veridis utiliser les Vc clair et ne suivez pas votre passion. Naturellement elle est pas chiant vous conduit à l’enfer… réfléchissez hein

  • @user-ld9gm1pf3v
    @user-ld9gm1pf3v5 ай бұрын

    Wallahi tarikha yi dagnouy sank djam 😢

  • @user-ge9ii8uy4d
    @user-ge9ii8uy4d3 ай бұрын

    Ken dou cheikh Ahmad tidiane

  • @OuseynouWilane
    @OuseynouWilane10 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤

Келесі