Un document historique rare( Grandes figures du mouridisme ) à maints égards

La présque totalité des dignitaires mourides réunis, sur convocation du khalife général des mourides Serigne Abdoul Khadiri, l' Imam des imam (Beaucoup d' entre eux, malheureusement, sont décédés Yalna Yalla yokk leer té taass niou ci séen barké)

Пікірлер: 68

  • @matarniang709
    @matarniang7092 жыл бұрын

    Thiey yaram dawna. Adouna dou dara. Ce documentaire doit souvent passer à la télévision pour que cette nouvelle génération puisse mieux connaître les figures emblématiques du mouridisme. Thiéy Serigne Touba!

  • @poundkiima4241
    @poundkiima42414 жыл бұрын

    Thiey yalla 30 ans après niom nieup presque ken nékatoufi yalla na yalla yokou séni lér. Vidéo bi mérité na ay millions de vues.

  • @seynabfallou395
    @seynabfallou39510 ай бұрын

    Documentaire amna solo lole

  • @maimounadiallo8146
    @maimounadiallo81462 жыл бұрын

    Macha allah yallah na yallah yokou sény lére si barké seydina mouhamed psl

  • @papii2511
    @papii25112 жыл бұрын

    Archive exceptionnelle

  • @dieylanidiagne7509
    @dieylanidiagne7509 Жыл бұрын

    Ay waay founguéne dieulé biilé archives !!! 😱😭😭😭😭

  • @bambacisse4200
    @bambacisse420010 ай бұрын

    DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA KHADIMOUL RASSOULILAHI SALLALAHOU ALEYHI WA SALAMA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMPE BABOUL MOURIDINA ❤❤❤❤❤

  • @khadydiouf7833
    @khadydiouf7833 Жыл бұрын

    Aka beuri kersa ndeysane Serigne saliou yalna yalla Yok seni lérr brk Borom touba

  • @mbektemireek8416
    @mbektemireek84164 жыл бұрын

    Wallahi kou guissli xamni beugu Serigne TOUBA REKK wor wayé nak n'a niou bayixelni ken. Dekoufi 😭😭😭

  • @falloudia1016
    @falloudia10165 жыл бұрын

    Yalla nagnou yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @BAMBA347
    @BAMBA3473 жыл бұрын

    Ki Def vidéo bi nit manoko tere dem ajana

  • @layesoiree9872
    @layesoiree98728 жыл бұрын

    serigne Saliou borom diamgni borom diamono mame cheikh ibrahima fall mo goreé mo woor amoul morome Ken la do toufi amati

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia8992 Жыл бұрын

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @naroukadiorpur5543
    @naroukadiorpur55434 жыл бұрын

    Thieuy adouna dra yagou fi 😥😥

  • @Hamsatoul_Rijal
    @Hamsatoul_Rijal6 жыл бұрын

    Akassa guiss na sama serigne serigne hamsatou mbacke elimani darou mouhty inbn borom darou😍

  • @khadimdiop3348
    @khadimdiop33482 жыл бұрын

    Thiey yalla sonou brom yalna yalla yokkou sèni lère té tass tho sene bargué

  • @susobass7685
    @susobass76856 жыл бұрын

    yaram dawna khollene nioubakh gni ndayesane serigne touba amoul morom

  • @LatifYakhine
    @LatifYakhine8 жыл бұрын

    euskey ki def video bi Yalna borom bi taxawu Barké Cheikhoul Khadim. begna loolu sax.

  • @LatifYakhine

    @LatifYakhine

    8 жыл бұрын

    A hounzou billahi mina sheytani radjiim. Wa inya ouhinzouhaa bika wazouryatahaa mina sheytani radjiim. Rabi ahounzou bika min hamazaty sheyatini, wa ahounzou bika rabi ann yahdourouni. Nous n'avons pas besoin de savoir qui tu es. L'importance est de prier pour quiconque est dans le mouridism ne soit la que pour la face de Dieu. Mangui niane nak kep ko xamni guisna message bi mou bagn tontu mouk wadjii. Nax ki naroul def loudoul dinu bakarlo. Khadimou Rasoul dafa waxni : zima moul wara hansri ladal laahi fii yadi. Sunu borom def nako mouy borom niit Gni, Daldi wax fenen ni: zanaf hin bila dararine, ndiarign lou andoul ak lorangué. Lii rek moy li am famoom Kep Kouy woté woo Serigne Touba té dou deug ci yaw Yalna borom bi sopila ci Barké Cheikhoul khadim.

  • @ngonesaliou8347
    @ngonesaliou83473 жыл бұрын

    Ho yonnou mouride wetna ndeysane

  • @cheikhounaseye6714
    @cheikhounaseye67143 жыл бұрын

    degal serugne bara li nexna bilah yalla na yalla yoki sen lerr

  • @niangfallou8449
    @niangfallou84495 жыл бұрын

    Serigne touba rekka am li

  • @daoudandiaye5588
    @daoudandiaye55889 жыл бұрын

    thiey kémane deug ngui wayé nakk warnagne thié diangué ni kéne doufy désse

  • @adamakhouma3560
    @adamakhouma35605 жыл бұрын

    Machalla thiey bravo broum touba Ken du s.touba

  • @mohamedalifall5516
    @mohamedalifall55164 жыл бұрын

    Dieureudjeufé Borom Touba

  • @khadimcisse7687
    @khadimcisse76874 жыл бұрын

    Li dawna yaram dieure dieufeti borom touba

  • @ballasyll6868
    @ballasyll68687 жыл бұрын

    amine barkéb boroom touba

  • @abdoumbaye61
    @abdoumbaye615 жыл бұрын

    akasa amna solo lolllllllllllllllllllllll wayè gnou diaguèsi khamnè adouna doudara kone nanou sakh si ak talibè

  • @sasasow50
    @sasasow504 жыл бұрын

    Machala vídeo doumasi doyal bilahi

  • @bargnindiaye720
    @bargnindiaye7204 жыл бұрын

    Yalla na yalla bokki léram

  • @morkane7942
    @morkane79424 жыл бұрын

    thaye s touba

  • @falloundiayedieye7380
    @falloundiayedieye73804 жыл бұрын

    Machalla amna solo lol barkep serign touba

  • @taphakane5499
    @taphakane54995 жыл бұрын

    Amna solo

  • @falloudia1016
    @falloudia10166 жыл бұрын

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar.Sene mbokoum talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia89922 жыл бұрын

    Yalla nagnou Yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @mamadouthiam219
    @mamadouthiam2194 жыл бұрын

    Dieureudieuf serigne Touba

  • @groupemancocommunication399
    @groupemancocommunication399 Жыл бұрын

    Xana boroom yëre bu verte tey rée rek Serigne bass abdou xadar la

  • @poundkiima4241

    @poundkiima4241

    Жыл бұрын

    Mou way li Serigne Basse avait 10 ans.

  • @sene6344

    @sene6344

    10 ай бұрын

    S. Moudou magam cheikh bass temps bi mongi tol si diang am 9 ou 10anns

  • @koumbacke9731
    @koumbacke97314 жыл бұрын

    Sama serigne sama leup.sante nala gueureum nala

  • @almajzoob2300
    @almajzoob230010 жыл бұрын

    ndeysane guisnaa sama serigne beu s fallou diouroul mom s ibra mom s modou kherri mbacke

  • @alaloumoustaphamassamba8866
    @alaloumoustaphamassamba88667 жыл бұрын

    Amna Solo

  • @alphaoumarbarry3285
    @alphaoumarbarry32852 жыл бұрын

    Kii di wakh nii deh khawma foumou nek wayé kouko nié la kou âme tawfekh la

  • @khadimkhouma
    @khadimkhouma9 ай бұрын

    Machallah amna solo loool💜♥️❤️‍🩹❤️💕💟

  • @mamadousall7046
    @mamadousall70464 жыл бұрын

    Machala

  • @abdoufall7519
    @abdoufall75194 жыл бұрын

    Manchalla

  • @cheikhsacs5567
    @cheikhsacs55679 жыл бұрын

    Anduna diekh na

  • @der351khadim9
    @der351khadim94 жыл бұрын

    Akassa mourit

  • @der351khadim9

    @der351khadim9

    4 жыл бұрын

    Machallah

  • @alibosn8950
    @alibosn89505 жыл бұрын

    guis na si borom taif

  • @balabeybalabey8403
    @balabeybalabey84032 жыл бұрын

    Kha🎉mbacké baol palén Fas keur seringe cheikh dembou fall Espagne

  • @user-vo3nl1qh4n

    @user-vo3nl1qh4n

    27 күн бұрын

    Yaw DEH Nio bokou foñou deuk te manit Magui Espagne ndeysan

  • @balabeybalabey8403

    @balabeybalabey8403

    27 күн бұрын

    Tourbi nakala ?​@@user-vo3nl1qh4n

  • @ousmanediop1115
    @ousmanediop11154 жыл бұрын

    Cëy yalla...video bi amna solla

  • @balabeybalabey8403
    @balabeybalabey84032 жыл бұрын

    NIGÉNE ADOUNA NIAPE YALNALÉN YALLA DOUGAL ALJANA _ SI LOUAMOUL HISAB_NOUN NIFI DÉS YALLA GOUDAL SOUNOUFAN TANOUWÉR AK JAME SOUNOU FATOO MOUDOUGALNOU AL JANA SI LOUAMOUL HISAB AAMIIIN

  • @adamakhouma3560
    @adamakhouma35605 жыл бұрын

    Vidéo bi amna soulo tourop machalla mangui di dougua guiss vídeo bi xhamna barina si ay mouroum

  • @ibrahimakhalilmbaye7585

    @ibrahimakhalilmbaye7585

    4 жыл бұрын

    Mw aussi

  • @stoubarek1605
    @stoubarek1605 Жыл бұрын

    tiey.adune.amull.soloe.worne.kouNIE.yallne.yele.Jigall.nibue

  • @belkisaxum
    @belkisaxum8 жыл бұрын

    where are the ladies?

  • @ibakalonji
    @ibakalonji11 ай бұрын

    Cëy Cheix SÂLIH 😭😭😭😭

  • @mouslimonly7796
    @mouslimonly77962 жыл бұрын

    Les fou

  • @aminadiop2320
    @aminadiop232011 ай бұрын

    Dieureudieuf Serigne Touba

  • @susobass7685
    @susobass76856 жыл бұрын

    yaram dawna khollene nioubakh gni ndayesane serigne touba amoul morom

Келесі