Senegalese Multibillionaire El Hadji Djily Mbaye

The late religious, philanthropical man of many hats

Пікірлер: 598

  • @ANiang-uw4ex
    @ANiang-uw4ex4 жыл бұрын

    Cet homme était éclairé et guidé par la lumière divine dans tout ce qu'il entreprenait. Personnellement, j'habite dans une des cités qu'il a construite au début des année 80 et qui compte 53 villas dont les dimensions varient entre 500 et 1200m2, mais je dois dire que les bâtiments sont d'une qualité et d'une solidité extra ordinaire. Pas la moindre fissure au niveau des mûrs . J'ai toujours été fasciné par la vision qu'il avait à l'époque de construire une cité pareille dans une zone pas évidente et insoupçonnée de Dakar !!! En tout cas, c'était un grand visionnaire qui était très en avance sur son époque !!! Yalla na Borom bi Fay ko yiw si lép lou bakh li mou doon déf !!!

  • @gueyeami7122

    @gueyeami7122

    2 жыл бұрын

    Allahouma Amiine serigne bi merçi beaucoup !!

  • @user-tj2ef5sv5d

    @user-tj2ef5sv5d

    4 ай бұрын

    Amin ya rabby

  • @lampfallbusnesscompanybusn3651
    @lampfallbusnesscompanybusn36514 жыл бұрын

    Yallanama souniou borom def multimillionnaire si BARKEP BOROM Touba 🤲

  • @diamouhamed7400

    @diamouhamed7400

    2 жыл бұрын

    Saway dell ďef ay vidéo wày

  • @salihann25

    @salihann25

    2 жыл бұрын

    Amine

  • @ndiogoumaissasarr9097
    @ndiogoumaissasarr90974 жыл бұрын

    J suis tellement ému bilay lii rékk mo ame solo yalna yalla Yok aye Lééram barkép Borom Touba

  • @taphaseye243

    @taphaseye243

    4 жыл бұрын

    Aminnne

  • @ibrahimatoure8397

    @ibrahimatoure8397

    2 жыл бұрын

    Amine

  • @yassinsosseh6006

    @yassinsosseh6006

    2 жыл бұрын

    Ameen yarabal aramin

  • @tomasdiouf7367

    @tomasdiouf7367

    2 жыл бұрын

    Amine yarabi

  • @jaghlounhamid9766
    @jaghlounhamid97664 жыл бұрын

    Yalla nanouko yalla fayall gnoune wa louga khamnako boubakh diokhnama 1000f lokho ak lokho si bire palémba gnou toudeko rangou Baye Djily mbaye

  • @no-name6101
    @no-name61014 жыл бұрын

    Li rek la am am Di dierign,diamono yi niou nek niouko eupp khaliss niofi nek mais mom molen Guen riche mille fois ,Allal bou barkel moy dierign niep machalah ,yala naniouko yallah fayal❤️🤲🏾

  • @cheikhbeye7329
    @cheikhbeye73294 жыл бұрын

    C’est ces genres de personnes qu’on dois montrer au public mashaAllah yalnako yallah fay

  • @Justin-Lo.

    @Justin-Lo.

    3 ай бұрын

    Sounouy journaliste yi AK site internet yi jamais niou wané ces exemples de bonne volonté ❤

  • @golfmike7587
    @golfmike75874 жыл бұрын

    Djiely mbaye cest un homme du paradis djoulit ha khann la wone

  • @moustaphandourlentrepreneu9129
    @moustaphandourlentrepreneu91294 жыл бұрын

    El Hadji Djily Mbaye quel homme puisse son âme reposé en paix amen

  • @zakariadeune2296
    @zakariadeune22964 жыл бұрын

    Ma challah yalna yalla yeureum ko té diegeul ko si barké seydina Mouhammad sws

  • @pedrembengueabdoulaye2431
    @pedrembengueabdoulaye24314 жыл бұрын

    Baye djily c un saint un homme extraordinaire walliww Kamal Batine bi mo eupe alale bi fimou ague si yalla ak grade biMou ame si yonenti ken meunouko khaamm

  • @cheikhtoure9393

    @cheikhtoure9393

    3 жыл бұрын

    Bilahi deug bou wère batinam mo eup alalam

  • @gueyeami7122

    @gueyeami7122

    2 жыл бұрын

    Wallahi lou lére ngua wakh

  • @didigalass2506

    @didigalass2506

    2 жыл бұрын

    DEUGUE tigi

  • @samaypapier8279
    @samaypapier82794 жыл бұрын

    Thiey commerce mo barkel dé jieureudieuf Seydina Mouhamed psl

  • @alhaqq310

    @alhaqq310

    4 жыл бұрын

    Wallahi Macha'Allah (Saw)

  • @taphaseye243

    @taphaseye243

    4 жыл бұрын

    Machallah

  • @fatimadiop8383

    @fatimadiop8383

    4 жыл бұрын

    Salla lahou halayhi wasalam

  • @sapeulh5276

    @sapeulh5276

    3 жыл бұрын

    Psl

  • @ALMAMYKAHONE

    @ALMAMYKAHONE

    2 жыл бұрын

    Est ce que Khame nga lëpp ???

  • @aliounesangare4949
    @aliounesangare49494 жыл бұрын

    Un citoyen exemplaire nako yalla fay dieufam

  • @kheumiteakenathon7630
    @kheumiteakenathon76304 жыл бұрын

    Borom touba meuneu défar. Kouy mourite aimél

  • @linhodieng7574

    @linhodieng7574

    4 жыл бұрын

    Yaw xamo ligay wakh démal gessetou tarikh xamo dara

  • @traoresidy9035

    @traoresidy9035

    4 жыл бұрын

    Wakho nada

  • @abdoumorethanakingthiam6930

    @abdoumorethanakingthiam6930

    4 жыл бұрын

    Serigne bi kén leu

  • @fahrozblanche2431

    @fahrozblanche2431

    4 жыл бұрын

    Serigne esk do geustou dji watt

  • @kheumiteakenathon7630

    @kheumiteakenathon7630

    4 жыл бұрын

    @@fahrozblanche2431 walahi digén déh thie kiniane.

  • @xx-nk8fe
    @xx-nk8fe4 жыл бұрын

    64 ans def lii yeup...machallah

  • @ridjalabdallahyakhineseye3093
    @ridjalabdallahyakhineseye30934 жыл бұрын

    Le père des milliardaires Sénégalais! Véritable référence! Un ... homme de dieu très généreux! Dieureudieufé Serigne Touba!!!

  • @zizaziza5450

    @zizaziza5450

    11 ай бұрын

    Le père des nécessiteux

  • @ouzsibysiby8839
    @ouzsibysiby88394 жыл бұрын

    Machalla un homme généreux yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana firdawsi 😭😭😭😭

  • @abdoukhadrediop3885
    @abdoukhadrediop38854 жыл бұрын

    Walahi wa dara amou gnou mass😘🕌🕌🕌🕌🕌🕌

  • @sidicamara3119
    @sidicamara31194 жыл бұрын

    Macha Allah un vrai référence. Yalla nanouko borom bi fayal

  • @antaloum7043
    @antaloum70434 жыл бұрын

    Machallah yallah nako yallah xaré aldiana tam fayagniou ko fier d'être lougatoise

  • @moussambengue4861
    @moussambengue48614 жыл бұрын

    amoule morome rek mo siye tégou MaChallah yalla nako yalla faye limou déf beurina

  • @mafaldiop8023
    @mafaldiop80232 жыл бұрын

    J'ai eu la chance de visiter et passé la nuit dans son palais à louga mais c extra ordinaire comme être humain

  • @safietoufall9975
    @safietoufall99752 жыл бұрын

    Le Sénégal d'aujourd'hui a besoin des gens comme elhadj djily mbaye machaallh yalla nako yalla Faye yiw defalko si mixatoul khasani

  • @gueyewagane2882
    @gueyewagane28824 жыл бұрын

    Un homme fort. Lii moy reference.

  • @massoguisene2631
    @massoguisene26314 жыл бұрын

    Merci beaucoup à vous, ont n’as toujours eux des grands hommes dans ce pays, mais ont les connais pas ? Grâce à vous ses hommes vont sortir de l’ombre 🙏🏾moi je vous suis avec intérêt, merci 🙏🏾

  • @diopsam8076

    @diopsam8076

    4 жыл бұрын

    Merci

  • @ngonefaye6877
    @ngonefaye68774 жыл бұрын

    Machalla paix à son âme,c'est un référence yalna ko yalla fay kholam bou rafet fier de ce grand mr mes respects

  • @ibrahimangom2828
    @ibrahimangom28284 жыл бұрын

    Un carrière très très riche mashalahh💖💖

  • @sodagueye2550
    @sodagueye25504 жыл бұрын

    Baye Djily yalna gno ko yala fayal,🤭c ces genres de figure k la jeunesse a besoin comme référence mais malheureuse on sombre dans la futilité,! Merci racine très beau travail!

  • @boubacarsyllame2835
    @boubacarsyllame28352 жыл бұрын

    Machallah tabrak'Allah djily mbaye Yalna yalla yokou léram amine. Merci à vous tous

  • @mariendiaye2703
    @mariendiaye27034 жыл бұрын

    Machallah Amena Solo El Hadji Djily Mbaye Sonou Ferté gnoune Wa Louga

  • @bilygueye2928
    @bilygueye29284 жыл бұрын

    Eskeuy machalla, Rewoum Sénégal mo bari ay Jambars ak References. yalla naniouko yalla fayal tei defniou com mom Amiiin🙏

  • @sapeulh5276

    @sapeulh5276

    3 жыл бұрын

    Amine ya raby

  • @moustaphakouwanta6430
    @moustaphakouwanta6430 Жыл бұрын

    Vraiment ELHADJI DJILY BAYE est un grand grand homme de l'histoire Sénégalais, l'Afrique a besoin des hommes comme lui.Que son âme repose en paix Amine ya Raby

  • @venusnoire4908
    @venusnoire49083 жыл бұрын

    Mashallah li lagnu wakh patriote dégue nak. Yallah na ko sugnu borom fayeko fumu nek ci barké seydina Mohamed 🤲🏿

  • @ameetfallsenegal3506
    @ameetfallsenegal35063 жыл бұрын

    Machallah amna solo yalla nako yalla yeureume ta kharéko aldiana thie barcké saydina Mouhammad saw barcké serigne touba

  • @amadoumoustaphadieng8660
    @amadoumoustaphadieng86604 жыл бұрын

    Yallah defal na Mame Bamba lou reuye! Dieuredieuf Mame Bamba Amoo morom.

  • @adjibinetagueye5475
    @adjibinetagueye54754 жыл бұрын

    Machallah liguèyeul yalla rek mo wor yalla nako yalla faye

  • @aidis3605
    @aidis36054 жыл бұрын

    El Hadj Djily Mbaye un bienfaiteur qui doit servir d'exemple à tout un chacun. Qu'Allah le tout Puissant l'accueille dans son paradis

  • @syllafamilly9491

    @syllafamilly9491

    4 жыл бұрын

    Kéne dou mame chiekh mbaye kabire .poye

  • @mamendellafaye3717
    @mamendellafaye37174 жыл бұрын

    une référence mashallah yalnako yalla faye xolameeee

  • @astoudiack46
    @astoudiack464 жыл бұрын

    Genrou nit yi amatoul yalla na hippe aldiana firdawsi si barke seydina mohamed psl

  • @Aphts
    @Aphts2 жыл бұрын

    Ligue modié wakh nehhhna anou dôme yi warone aguale yenebi💯😭

  • @thebigH-qx8kd
    @thebigH-qx8kd4 жыл бұрын

    Un homme de foie El hadji Djily MBaye

  • @cheikhdiatta5755
    @cheikhdiatta57552 жыл бұрын

    en tous cas les plus grands hommes d'Afrique et particulièrement au senegal n'ont jamais été à l'école française .un grand big up à ces ndongo daara

  • @fatoukone4532
    @fatoukone45324 жыл бұрын

    Macha Allah yalla na yalla fayale nionko Sénégal fimou tolou niou melni baye djili rék mon fi menké

  • @kalidouwade9442
    @kalidouwade94424 жыл бұрын

    Un grand homme qui mêrite la reconnaissance de tout un pays

  • @daoudaciresall7293

    @daoudaciresall7293

    4 жыл бұрын

    Paix a son áme beau paradis

  • @gueyeami7122

    @gueyeami7122

    2 жыл бұрын

    Wallahi deugue rék ngua wakh

  • @taphasylla3784
    @taphasylla3784 Жыл бұрын

    elkhadji djili mbaye yalla nako sounou brome faye lou bah Sénégal kontanagn ci yaw louga lo dioye na ci yaw

  • @djibsondasilva454
    @djibsondasilva4544 жыл бұрын

    Djily M'Baye was one in a million masha'ALLAH❤️ Yalla nako ALLAH fay dieuf you bakh yimou déf thi Dunya bi❤️🙏🏾

  • @papjobe1872
    @papjobe18724 жыл бұрын

    Sounou ferte nioun wa louga cke dou baye djiliy yalla na ko yalla yerem te khare ko adiana fir daw si thi barcke serigne touba ❤❤❤👍👍 baye fall bi ana solo nice na

  • @mariamagueye5272
    @mariamagueye5272Ай бұрын

    Allahou Akbar , milliardaire you ndieukk yiiii baxon nagn teh yéwéné Xolal Bay Djily ak Baye Ndiougga kébé rekkk Ndeysane , Yalnagn Yalla may Alal bou Barkél teh gnu nanguko bokou ak jamm yiii teh Yalla rekk tax

  • @iibassndiaye2886
    @iibassndiaye28862 жыл бұрын

    Ndeysan yalla na mélni mom si barké xassida yi ❤️🙏💯🇸🇳dieureudieufeuty Serigne Touba

  • @cheikhsow5550
    @cheikhsow55502 жыл бұрын

    yalla na yalla khar adiana sí Berk serigne babacar sy 🤲😃💯🤝🤝

  • @evre8918
    @evre89184 жыл бұрын

    Yalla na yalla yokou ay leram si barké seydina Mohamed PSL

  • @alioudrame5409
    @alioudrame54094 жыл бұрын

    AMNASOLO MACHALLAH Ndaysane tarikalla

  • @tallagueye3361
    @tallagueye33614 жыл бұрын

    Man domou Louga mais Sama xoll seud na trop yalla na gnou yalla fayal baye Djili MBaye yalla nako Faye diefam

  • @abdoukhadrediop3885
    @abdoukhadrediop38854 жыл бұрын

    Thieuy wa dara 🕌❤❤❤🕌🕌🕌🕌❤

  • @chill.1155
    @chill.115511 ай бұрын

    Le meilleur exemple de persévérance pas seulement pour le senegal mais pour tous les africains 😎💚💛❤

  • @salimatasall7
    @salimatasall74 жыл бұрын

    Un homme humble et généreux aldjana firdaws

  • @petitpoetediop5788
    @petitpoetediop57884 жыл бұрын

    Man sha Allah on est très satisfait de la vidéo. Soudé meun ngene niou diapele aussi ci vidéo NDIOUGA KEBE dina am solo lol

  • @diawi2588
    @diawi2588 Жыл бұрын

    Vraiment si tous les hommes fortunés comme lui notre pays dépasserait ici.

  • @bouchragueye8349
    @bouchragueye83494 жыл бұрын

    Baye Djily yalna yalla yokk sa leer yalla def la thi Aldiana firdawsi thi barki seydina Mohamed psl ya bakh Mbaye sangua yalnala ko yalla faye bou bakh fi gua nekk thi barki seydina Mohamed psl

  • @Ousmane-zn6el
    @Ousmane-zn6el3 ай бұрын

    Vraiment dimeu yi nio fi manque.❤

  • @sarrvieux9767
    @sarrvieux97674 жыл бұрын

    C très très important de connaître elhadji djily mbaye mais aussi maître babakar seye si c possible merci et bonne continuation yangui job lou nice

  • @adamadiagnediop8397
    @adamadiagnediop83974 жыл бұрын

    man domou louga bi dh contane na loll té am fierté lol itam ci Baye Djily Mbaye. Té makk gni fi ci louga gni nga khamni kham nagn lol baye djily wakh nanou ni xam xam bi ak nianam bou yémé mo eupone alal dji wayé dadone neubato alal dji. Alhamdoulillah nioun wa Sénégal banou yalla diokhé baye Djily

  • @latif9690

    @latif9690

    4 жыл бұрын

    Ta p

  • @damany7419

    @damany7419

    2 жыл бұрын

    Il habitait kel village si louga quartier

  • @maguettedieng7423
    @maguettedieng74234 жыл бұрын

    😭 walahi goor yalla degue moy baye djily yalla nagnou ko yalla guena fayal tass gnou si barkem barki mame cheikh mbaye

  • @ibrahimaka20
    @ibrahimaka204 жыл бұрын

    Yalnako yalla yeureum...mbakh rekk mo am solo.

  • @iboudjite4837
    @iboudjite48374 жыл бұрын

    No contana si baye djili mbaye limoy patriot yalla nako yalla khare aldiana 😢😢😢😢😢

  • @ramcha607
    @ramcha607 Жыл бұрын

    Franchement je suis très surpris de son travail🥰sama xol sedna torop thi mom. Yalna borom bi yessal yeurmendém thi barké yonent bi saws 🙏

  • @Justin-Lo.
    @Justin-Lo.3 ай бұрын

    Si tous les hommes milliardaires du Sénégal avaient fait pareil comme lui le Sénégal serait développé depuis très longtemps ❤❤ QU'ALLAH LUI RÉTRIBUE SES BIENFAITS DE LÀ OÙ IL EST BARSAKK❤

  • @maraniang8721
    @maraniang87214 жыл бұрын

    Yalla nako yalla kharé adjiana ta gni âme weurseuk yeup yalla nalén yalla khire si loubakhe com pape djili mbaye

  • @babacarndiaye1419
    @babacarndiaye14192 жыл бұрын

    Ay Dieufam rafetna trop. D’après ces témoignages Je peux dire qu’il il était humainement plus riche que financièrement. Yalnako Allah SWT fay yiw. Yalnako Allah SWT yeramko xareko Aldjana Firdawsi.

  • @DAMEWADE93
    @DAMEWADE933 жыл бұрын

    defal vidéo ci Serigne Sam Mbaye😭🙏🏿🙏🏿

  • @srabdoukhadrendiaye2580
    @srabdoukhadrendiaye25804 жыл бұрын

    Machallah el'haji mbaye yalla nañou ko yalla fayal guene gui faye té oyafal souf si kawam amine 🤲🤲🤲

  • @Tonavis
    @Tonavis4 жыл бұрын

    Merci beaucoup et bonne continuation, ça m'a vraiment touché de savoir que je foule le même sol que ce grand Monsieur. Great Inspiration!!!

  • @julesylla9960
    @julesylla99604 жыл бұрын

    Vraiment c'est une très belle vidéo. On a besoin de ça nous. On devrait publier ce video partt par ce que genre de personne mérite qu'on leurs rendent hommage. Ce sont des exemples et leurs histoires ne doit pas s'éteindre. Le Sénégal en a besoin. Mane dei moma gueunal nioumey djangal aye MAOZEDON ak aye TCHANKAYE TCHEK. Vraiment je vous félicite et vous encourage. Bonne continuation.

  • @boromeroukhoubi6308
    @boromeroukhoubi63082 жыл бұрын

    Ñi laniou wara diagalé si sounou école yii wayé di niou beug raye ak ay toubab you niou amaloul bena ndiarine Baye djili mbaye yalna nala borome bii subhanakhou wa tallah geureum amine ya rabbi

  • @diaspoworld3395
    @diaspoworld33954 жыл бұрын

    Yalla nako Yalla fay thi barke Alkhourane Amine ya Rabbi

  • @layelaye7171
    @layelaye71714 жыл бұрын

    mashallah une référence un modèle pour la nation

  • @seydinandiaye641
    @seydinandiaye6414 жыл бұрын

    Voilà des personnes que la jeunesses doit suivre

  • @kirikou_026
    @kirikou_0262 жыл бұрын

    Ndaysaan Sénégal yàgg naa am ay nit yu baax na ko sonu boroom dolli yërmaande famu nekk te dolli koo fay lu baax limu def ci kaw suuf Barkeb boroom Tuubaa❤️❤️❤️

  • @pascalsene4731
    @pascalsene47314 жыл бұрын

    C'est dommage que le Sénégal n'a plus des hommes de valeurs comme elhaj Djily mbaye

  • @aramatoulayedabo3438
    @aramatoulayedabo34384 жыл бұрын

    May Allah repay him with jannatul firdaws and gant Senegal many more like him ameen.

  • @Abdou.1007
    @Abdou.10074 жыл бұрын

    Merci pour ces informations, franchement je ne connaissais EL HADJI DJILY MBAYE que de nom mais cette vidéo a permis de connaître la dimension importante et l'œuvre de l'homme.Ces oeuvres méritent d'être connu par tout le peuple sénégalais pour service rendu à la nation.les politiciens, les hommes dotés de gros moyens financiers doivent s'inspirer de ce grand Monsieur et cesser de nous tympaniser.Que Dieu vous accueille dans son paradis.

  • @cheibanipatissier7619
    @cheibanipatissier76194 жыл бұрын

    Dieureudieufe baye djili bilahi ma beug bay djily ak serigne sam

  • @cheikhmbacke4379
    @cheikhmbacke43794 жыл бұрын

    YALLA NAKO YALLA YEUREUM TE KHAREKO ALDIANA FIRDAWSI BARKE SEYDINA MOUHAMED

  • @tahiroudieng176
    @tahiroudieng1764 жыл бұрын

    Wallahi tay contane na lol si li ki yalla rek mokham makhamam yalla nako yalla yeureum SBBN NB : mame cheikh mbaye moy bayam mais Serigne hamad sikhir lo taloube mame cheikh Mbaye la won merci

  • @ndefcamba9226
    @ndefcamba92264 жыл бұрын

    Merci pour tout. Yallana nagnouko yallah fayal. Pour tamba pas seulement le lycée il ya le marché central et l'hôpital régional. Paix à son âme

  • @mamadoundour8940
    @mamadoundour89404 жыл бұрын

    Machalla que Dieu lui acueil dans son paradis amine il ete formidable

  • @ngagnedembabalde5080
    @ngagnedembabalde50804 жыл бұрын

    Merci encore une fois la Racine!

  • @sylldame4216
    @sylldame42162 жыл бұрын

    Machalah vraiment elhadj djily dafma yém vraiment

  • @diopsam8076
    @diopsam80764 жыл бұрын

    mame cheikhe mbaye amoul photo déh.photo bobou SR.moud sakhir lô la bou koki mo lën don diangal

  • @fahrozblanche2431

    @fahrozblanche2431

    4 жыл бұрын

    Deugleu kay

  • @rahmanethiam9864
    @rahmanethiam98643 жыл бұрын

    Ohh machalla frère Mai lenn Dong moma mettii Sénégal deuku guinar Lee bo deyee ngay am prix Mais quand tu vis tu dérange Ndeysanne royukaay abstrus lee HADJ DJILY MBAYE

  • @khadimkebe2313
    @khadimkebe23134 жыл бұрын

    Ndaysane ki moy yaram deug😥Sénégal

  • @senegalaisbideuksenegal2183
    @senegalaisbideuksenegal21834 жыл бұрын

    nice job bro franchement on a des icônes au sénégal mais on ne le sait pas ligueye ak djoube rek mo ame solo machaallah yallah na yallah yokou si kaw rek

  • @bassembaye3082
    @bassembaye30824 жыл бұрын

    Mâchallah jereungene jeuf liii amna solo loool mâchallah yeneu ngi ñiouy dieurigne bou bakha bakh.

  • @mbayefaye8184
    @mbayefaye81844 жыл бұрын

    Machallah il faut tjr rappeler Afrique à ses origines

  • @maxfall3597
    @maxfall35972 жыл бұрын

    Yalla naco yalla yeureum kharéco aldjana .yalla molla guena bakh .yalla noco yalla fayall bopam🙏

  • @ngonedieng7755
    @ngonedieng77554 жыл бұрын

    رحمه الله تعالى رحمة واسعة وأدخله فسيح جناته مع النبيين والصديقين والشهداء والصالحين

  • @assfall7827
    @assfall78272 жыл бұрын

    Le senegal na jamais connue un homme comme lui lui ici a louga appart trubinal lep mokafi def (talli yi ,hôpital, stade ,diouma lep ,gouvernance ,lycée lep mokafi def❤❤

  • @mamemousseuh4508
    @mamemousseuh45084 жыл бұрын

    El Hadji djily mbaye yalla na yalla yoku aye leram yaramko ta yekhinu ta tasnu the barkem amiiine the barkem serigne touba mbacke

  • @falloufall1816
    @falloufall18164 жыл бұрын

    Un homme très généraux est très noblesse que dieu le pardonne 🙏🏿

  • @medounethiam99
    @medounethiam992 жыл бұрын

    Djili Mbaye waliola wone

  • @Siahga
    @Siahga4 жыл бұрын

    Merci beaucoup frere tres important et tres riche.

  • @fallablaye6203

    @fallablaye6203

    4 жыл бұрын

    Me sama wadji foto bi dou papam ki serigne sakhir lo la

  • @fallablaye6203

    @fallablaye6203

    4 жыл бұрын

    @@boubacarndiaye9214 diueruedif babackar bo guise noy wakh lii dafa wara ler ndakh Ñi khamoul da noy yakar ne foto bobou mame chiekh la te dou mome

  • @fallablaye6203

    @fallablaye6203

    4 жыл бұрын

    Ta Noy def video liiii bakhna kham le nit kou bakh ko melni baye djili mbaye lou bakh la wakh nay lerr ndakh Ñi khamoul babacar diuerdiuef ni rek la