« Sokh mo done dieuw Eumeu Sène , 200% Pikine…» Fils de Balla fait de terribles révélations sur…

Пікірлер: 388

  • @People221sn
    @People221snАй бұрын

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL

  • @karimistesarr3457
    @karimistesarr3457Ай бұрын

    Fils de balla do sama mbeur m DEUG gou wérrr NGA wahh ❤ machalha

  • @louislamotte1482
    @louislamotte1482Ай бұрын

    Tu as raison Fils de Balla❤️❤️❤️🔥🔥 Sokh il parle trop wayy dafa beuri wax torop mane il m'enerve

  • @alioutine2789
    @alioutine2789Ай бұрын

    Machahala wakh jii rafėte naa champion

  • @user-qj1id1zq7r
    @user-qj1id1zq7rАй бұрын

    Merci merci merci merci

  • @alysow9089
    @alysow9089Ай бұрын

    Fisl de Balla yw champion ngua boul khass kene

  • @CheikhDiop-vv2xt
    @CheikhDiop-vv2xtАй бұрын

    Frère wakh dji raféte na Machala 🙏🥰

  • @amethzidane2566
    @amethzidane2566Ай бұрын

    Sokh bari na wax certe mai Fils de Balla yow tamit bari wax nga def tei defo dara si lamb kougnou wax nganei do beurei ak mom Yow aussi lo apportel guediawaye apres nga wax gnouko

  • @kheuchfatygeneralloupapedi3484

    @kheuchfatygeneralloupapedi3484

    Ай бұрын

    Surtout lolou fils de balla mi daye tamou

  • @amethzidane2566

    @amethzidane2566

    Ай бұрын

    @@kheuchfatygeneralloupapedi3484 tei dara la defoul si lamb

  • @magattediop9975

    @magattediop9975

    Ай бұрын

    Bilae niom niar nio yam.

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5ucАй бұрын

    Wakh deug yalla geum na fils de balla mo meune sock le gars malheureusement da wodo lamine bi

  • @MorThiaw-ui5pu
    @MorThiaw-ui5puАй бұрын

    Sokh 💪💪💪

  • @papengom259
    @papengom259Ай бұрын

    Yén gnar yéna yam

  • @sidysiby9795

    @sidysiby9795

    Ай бұрын

    Bilay 😅

  • @Zikwoss1558

    @Zikwoss1558

    Ай бұрын

    😂😂😂

  • @senegaltv1142
    @senegaltv1142Ай бұрын

    Yenn yam rk 😂😂

  • @khalilgueye363

    @khalilgueye363

    Ай бұрын

    6moy9

  • @ousmanesarr756
    @ousmanesarr756Ай бұрын

    Fils de Bala wakhna deug sock da bari wakh té yeug succès na bayi eumeu bimouy dirantel magg dou moromam fils de balla au moins bamou dioté ak balla balou nako ak niou delou nek si diam mè iow sock nga yak eumeu loula nekh mou tiyé bopam nga nieuw fi di bari wakh pikine dagno beug diambar sa yugnou neké si diafé diafé eum nieuw décanté situation té kou dioug attaqué ko sock da wara wagni wakhbi diema prouver

  • @soldarouyayam8524

    @soldarouyayam8524

    Ай бұрын

    Bilay eumeu sène a tout fait pour pikine mai sokh mome diakhal nama mane dèh dotoumako suportèr thi adouna

  • @BallaMoussaTamba09

    @BallaMoussaTamba09

    Ай бұрын

    @@soldarouyayam8524lolou sa problème leu

  • @ousmanesarr756

    @ousmanesarr756

    Ай бұрын

    @@soldarouyayam8524 il est énervant à la fin bilahi eumeu limou nopi motakh kou dioug attaqué ko té ndam yimou indi pikine amoul mbeur boukofa indi monument lafa loudoul sargal ko warougnoukoko def

  • @soldarouyayam8524

    @soldarouyayam8524

    Ай бұрын

    @@ousmanesarr756 bilay limou def pikine bène beur dèfoukofa limou def thi bapate defniouko molène dakha beurè euplène fite ta dafa ame ñianou wadiour xol by mo rafet

  • @sidysiby9795

    @sidysiby9795

    Ай бұрын

    Fils de balla mo guena bari wax foufe

  • @user-vm6of4gq3i
    @user-vm6of4gq3iАй бұрын

    Fils de balla champion deug nga, deug alla lou yalla la, eum rek

  • @serignedieng-vh4zv
    @serignedieng-vh4zvАй бұрын

    mérci fiss de bala emeu séne séne pikine amour gnou fayam

  • @RafaelSanchez-fz3rb
    @RafaelSanchez-fz3rbАй бұрын

    Sa wakh rafetnaa waay !!!guen ĺèn bolo rekk top si guinaw balla gaye

  • @yayasowe4367
    @yayasowe4367Ай бұрын

    Machallah refetna ❤❤❤

  • @papegueye9665
    @papegueye9665Ай бұрын

    Mbeur on est derrière toi sokh doff la

  • @laminediop7135
    @laminediop7135Ай бұрын

    Merci merci beaucoup Balla❤❤❤❤

  • @user-jq2pt2ew5n
    @user-jq2pt2ew5nАй бұрын

    Massallah

  • @cheikhdiouf2027
    @cheikhdiouf2027Ай бұрын

    Fils de balla tu as dit raison sokh d’où champion lamign bi Mo reuy nabayi mbeur yi tei gueum bopam

  • @mouhameddia5168

    @mouhameddia5168

    Ай бұрын

    Non sock champion la dèh dèbut carrière bou doye ware la ame est ce que défoul plus de 8 combat sans dèfaite

  • @ahmadoudiop5016

    @ahmadoudiop5016

    Ай бұрын

    ​@@mouhameddia5168 😂😂😂 8 combats sans victoires kone dou champion

  • @mouhameddia5168

    @mouhameddia5168

    Ай бұрын

    @@ahmadoudiop5016 dama dioum rectifier Nako 😂 😂😂😂😂

  • @Domou_Deukk_Bi

    @Domou_Deukk_Bi

    Ай бұрын

    ​@@ahmadoudiop5016😂😂😂

  • @ahmadoudiop5016

    @ahmadoudiop5016

    Ай бұрын

    ​@@mouhameddia5168😂😂

  • @user-uj7lf8ls6y
    @user-uj7lf8ls6yАй бұрын

    Ya fi wakhone balla gaye takou alar la té monté sokh wakhoul lolou eume sene

  • @ahmadoudiop5016

    @ahmadoudiop5016

    Ай бұрын

    Bokul ki dafa mérone def réaction à chaud Mane sock damako faral mais nak dafa beug ay détail de trop sonalna eumeu nak

  • @ousmanecisse4103
    @ousmanecisse4103Ай бұрын

    Merci fils de balla Soh wax rek la man

  • @AbdourahmaneMbaye-hz2fg
    @AbdourahmaneMbaye-hz2fgАй бұрын

    Merci fils de balla sokh mome mo gueneu gnakk diome pikine

  • @user-ic3nl8kt9c
    @user-ic3nl8kt9cАй бұрын

    Merci frère dina bah amol ragal ligey rek

  • @WadeCourtois907
    @WadeCourtois907Ай бұрын

    Fils de Balla guirr yalla malo ko Niane boul dieul SOKHO SVP 🙏🙏🙏

  • @user-qj1id1zq7r
    @user-qj1id1zq7rАй бұрын

    Merci

  • @khadimmoustaphagueye4058
    @khadimmoustaphagueye4058Ай бұрын

    Merci fils de Balla ta bien communiquer fall

  • @user-lw1oi1yi6s
    @user-lw1oi1yi6sАй бұрын

    Sokh❤❤❤❤❤

  • @SaliouNdiaye-xz6bg
    @SaliouNdiaye-xz6bgАй бұрын

    Mé yaw figua dieule sa problème AK balla guaye exposé KO thi internet yi thi ay détails nieuwoule sama ginté

  • @kheuchfatygeneralloupapedi3484

    @kheuchfatygeneralloupapedi3484

    Ай бұрын

    Wala ki daffa fouye

  • @Thomassankara8502.
    @Thomassankara8502.Ай бұрын

    Ioe ya geuneu reuy lamigne sock dieuleul avance bi

  • @user-fx1wt4mg7h

    @user-fx1wt4mg7h

    Ай бұрын

    Vraiment

  • @authentiqueprod
    @authentiqueprodАй бұрын

    Linga Conseiller sokh thi digeuntém ak eumeu séne loula ko téré déf binga dioté ak balla gaye 2 loy diklé war nga si Djitou Mé franchement sa communication machallah sokh wakh dji wakh dji hooo sokh na wañi wakh dji bari na lool

  • @WadeCourtois907
    @WadeCourtois907Ай бұрын

    Fils de Balla mane déh iow lay supportai mais d'accord rouma nga dieul Sokho billahi mome mongui si sacoyi lo koye dieulé soûla Dané billahi digua am problème bou méti sisa adouna

  • @user-gp9vr9tb4p
    @user-gp9vr9tb4pАй бұрын

    Nice ❤❤❤🎉

  • @petitbayefall2278
    @petitbayefall2278Ай бұрын

    Lamb diou nékh moy sok ak fils de balla

  • @cheikhsow1042
    @cheikhsow1042Ай бұрын

    Fils de Balla Yambar nga rek

  • @diaibrahim6798
    @diaibrahim6798Ай бұрын

    Vraiment non soréwouléne 😂😂😂😂😂

  • @user-fx1wt4mg7h

    @user-fx1wt4mg7h

    Ай бұрын

    6😂9

  • @piiibnfatah8497
    @piiibnfatah8497Ай бұрын

  • @user-kk6yl4ds8m
    @user-kk6yl4ds8mАй бұрын

    Sock dafa bari wakh tè amoul ndiarigne

  • @user-es5wy8gs8u
    @user-es5wy8gs8uАй бұрын

    Cv fils de BALLA comme dieule talfa waye💔💔

  • @AminataDIOUF-ez8kd

    @AminataDIOUF-ez8kd

    Ай бұрын

    Ioe dane tonton wou talfa di diélat talfa😂

  • @ElhadjiNiang-pr6lt
    @ElhadjiNiang-pr6ltАй бұрын

    Kontanna💪🏾👍🏾

  • @ziarkone6777
    @ziarkone6777Ай бұрын

    Dieuleul sokh combat la té mola gueuna rafet palmares té sokh eumeu mo takh mou nekk mbeur

  • @Maestroo.20

    @Maestroo.20

    Ай бұрын

    😂😂 sokh dakoul palmares dè … yow khana khamo lamb!!!! Sokh vs youssou ndour wala sokh vs diam terri

  • @deutschkillatv4696
    @deutschkillatv4696Ай бұрын

    zarco/ Alioune seye 2

  • @abdoudiouf2125
    @abdoudiouf2125Ай бұрын

    Vraiment fils de Balla nittou seug nga sokh defa bari wakh. Eumeu monument la bir Pikine. Nako Diokh thieur biko Ama ak Boy Niang dou yak dara si carrièram . AMA champion la , Boye Niang champion la te teyewoul deno respecté Eumeu.

  • @wiizybdashfever2824
    @wiizybdashfever2824Ай бұрын

    Mo amo fiite..

  • @ebrimasohna3228
    @ebrimasohna3228Ай бұрын

    Yallana Yalla defal jam, s'il vous plaît, continuez à travailler et oubliez-le, je suis 💯% fan d'Eumeu Sene mais vous ne faites que klaxonner le véhicule devant vous. C’est donc lui qui aiguise et sonne l’alarme, alors concentrez-vous simplement sur votre rêve. merci

  • @user-oz4iu5pc1t
    @user-oz4iu5pc1tАй бұрын

    ❤❤❤❤❤

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wcАй бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @davidmendy3849
    @davidmendy3849Ай бұрын

    Sokh👍👍👍👍

  • @malangkujabi5108
    @malangkujabi5108Ай бұрын

    Wakho deug khamo Dara si Sokh Sokh baye fall

  • @bayewaly4963
    @bayewaly4963Ай бұрын

    Comme tu l'avais fait avec Balla

  • @abdoudieng5225
    @abdoudieng5225Ай бұрын

    Palmarès Fils de Balla 9 victoires Sangue 2, Boy Sarr, Odinga, Guine, Weuz Diambar, Balla Gaye Jr, Tapha Leer, Général Malika, Gora Sock 2 défaites Thialamber, Bour Sine 1 nul Boy Sèye 2

  • @Dpp205
    @Dpp205Ай бұрын

    Sa way Jackson champion la way danoul sokh

  • @lahadboukharagnelo6707
    @lahadboukharagnelo6707Ай бұрын

    Mogui nianw dh 😂😂😂😂😂😂😂😂 Lamb bi kokoy teugou waye 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥❤️❤️🔥

  • @saiifba4282
    @saiifba4282Ай бұрын

    ❤❤❤👍👍👍👍

  • @malangkujabi5108
    @malangkujabi5108Ай бұрын

    Boy dangai sop diapal balla gaye motakh nit yii kham la ndakh defo fii dara boy Sokh Mola raw si lamb

  • @WadeCourtois907
    @WadeCourtois907Ай бұрын

    Billahi dieul Diéne kayra sakhe mo ngeune fouff SOKHO

  • @papemoussadiop83
    @papemoussadiop83Ай бұрын

    yagui dogne sokh champion mes conseils rafete na

  • @MouhamedProphete
    @MouhamedPropheteАй бұрын

    Yen niar yena yam nakh ioe tmt khoulo guafi ak balla gaye si lou yaguoul dara 😅😂😂

  • @user-wo3xq7jl3x
    @user-wo3xq7jl3xАй бұрын

    Sokh wakh rek lay def

  • @badianendiaye1558
    @badianendiaye1558Ай бұрын

    Mà yawe ya wahone balla Gueye Samba alar la lolou sohk wahouko dh😂😂😂😂😂😂

  • @ACTULAMB

    @ACTULAMB

    Ай бұрын

    Mais balou nako

  • @MSam5-vp5ed

    @MSam5-vp5ed

    Ай бұрын

    Warruta wah si soh. Na fek la

  • @CaramocoDiallo
    @CaramocoDialloАй бұрын

    Sokh bilahi eumeu sene moootaxone malaî foral kou ma bett ga bayil iniane AK soxor bayil eumeu sene

  • @moussaseck967
    @moussaseck967Ай бұрын

    Merci fils de balle ligua wakhe sokhe degue la sokhe vrement dafa Barry wakhe eumeu sene kou bakhe la sokhe royale si eumeu sene sa grand frère la me top micro yi rek Di wakhe

  • @Ibra418
    @Ibra418Ай бұрын

    Y’a geune reuy lamign gnépp

  • @Ousmansonko-ye4le
    @Ousmansonko-ye4leАй бұрын

    Deug nga wax fils

  • @NdeyemaguetteMbengue-ic6hr
    @NdeyemaguetteMbengue-ic6hrАй бұрын

    Sokh wakh rek lay def😂😂😂😂

  • @lesamouraisnoir5304
    @lesamouraisnoir5304Ай бұрын

    Bilahi Je suis 100% pikinois 💚❤️mes combats li la wakh combat Sokh Ak Franc nèna Sokh daffa dawe xêkh bi Diayou 😂😂😂 Limi mbèp mbèpi souko done berrè di dane lêgui pikine amate Rois des arènes

  • @user-pw9wz3bb9r
    @user-pw9wz3bb9rАй бұрын

    Sokh mon sof wakh rék com djguéne akh

  • @PapaDiouf-rm4uj
    @PapaDiouf-rm4ujАй бұрын

    Sama mbeur nga ms boy beurék sokh sokh lay ndakh sokh mola gueneu liguéye takhawa Lou rk ngay df

  • @malangkujabi5108
    @malangkujabi5108Ай бұрын

    Khana yow waro nekhal balla gaye 😂😂😂😂😂

  • @SimonieBampoki-mz7by
    @SimonieBampoki-mz7byАй бұрын

    J suis pikinoi mes sokh dafa bari ndeye wokh bilahi

  • @mansourndiaye3391
    @mansourndiaye3391Ай бұрын

    Môme khana dafate loulou fi wakhe khone Balla gaye

  • @CheikhSarr-ck3or
    @CheikhSarr-ck3orАй бұрын

    Lou lérrr nga wakh sok da beurii wakh

  • @user-gu5mx7vb5g
    @user-gu5mx7vb5gАй бұрын

    Wakhofi dadiaw ndeyam gordjigueen nga dieuleull serigne ndiaye mou tegal sa ndey

  • @moussagueye6119
    @moussagueye6119Ай бұрын

    Fils de Balla yak sokh yéna Boku s Touba bouléne xoulo way

  • @ibrahimadrame9499

    @ibrahimadrame9499

    Ай бұрын

    Guénél Serigne Touba si li li lamb la😢😢 Serigne bi khamoul lamb 🫢🫢🫢🫢🙄🙄🙄

  • @vitosy5123
    @vitosy5123Ай бұрын

    bayi lén nafékheu sene titre bi moy laane

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9yeАй бұрын

    Serigne Ndiaye rec la ragal 😂

  • @user-cj5kr9zc4g
    @user-cj5kr9zc4gАй бұрын

    Yena yam Sokh wakh diokhla yw nga wakh delo ko yena yam gnary wakh katt😂😢😅

  • @gelawargelawar8972
    @gelawargelawar8972Ай бұрын

    Niguey def franc lala sock di def ,rawouloko yako fi geune bari wakh comme dieg

  • @footballgod4351
    @footballgod4351Ай бұрын

    Sokh sissoumane la pikine nek SI diam nek SI ay victoire ngay guen di wakh ay details yo xamni wakh ngako wakhat ko eumeu sene du moromam

  • @user-ny6gu9gt9x
    @user-ny6gu9gt9xАй бұрын

    Ki rk la nop 🎉

  • @user-hx6wo1tw4b
    @user-hx6wo1tw4bАй бұрын

    Fils de Balla tay da takkeu souff dh😂😂 Da mélni da dégue clash Gora Sogue bi😂😂

  • @elhadjiamadoundao6286
    @elhadjiamadoundao6286Ай бұрын

    TU AS DIT PIRE À BALLA GAYE 2😂😂😂

  • @morfall8992
    @morfall8992Ай бұрын

    Damaye wo lac rose dé😂😂😂😂

  • @maguetteniang3915
    @maguetteniang3915Ай бұрын

    Sokh kaye daguay warou vraiment akh

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353Ай бұрын

    Sokhou Deug Lay Wakhh Iow Yagui ni Banga Amé Problème ak Balla Gaye Founé Nga Tourné Di Wakhhh

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110Ай бұрын

    Wa legui fils de balla kane ngay beurél 😂😂 legui

  • @ibrahimaniang1463
    @ibrahimaniang1463Ай бұрын

    Yeune niarr yéna yém nimou déf si eumeu nga déf si balla gaye sen combat niari wakh Kate ngéne té defoulene fi dara

  • @mamadoulaminesarr1310
    @mamadoulaminesarr1310Ай бұрын

    Yak Sokh yena yam, ben guen

  • @assanesene8337
    @assanesene8337Ай бұрын

    💯💛💙 GUEDIAWAYE FILS DE BALLA RÉK SOKH AMAL YRR WAYY

  • @elhadjiamadoundao6286
    @elhadjiamadoundao6286Ай бұрын

    BAYIL DI SEULMO SOUFF SI😂😂😂

  • @morfall8992

    @morfall8992

    Ай бұрын

    😂😂😂😂😂😂

  • @ouzinouzin5516
    @ouzinouzin5516Ай бұрын

    Déba lépou sokou sokou yaw ame nga diote 😮

  • @lenfantnoir1295
    @lenfantnoir1295Ай бұрын

    Dixit celui ki disait k Balla Samba alaar leu 😂 Fils d Balla ioe ak Sokh yèna yam wakh rk nguen di def

  • @malicktoure6343
    @malicktoure6343Ай бұрын

    Mais mane senegal mi beuri nafek , ioe barki demb guani guen xass balla Guaye tay guay xass sokh

  • @ahmadoudiop5016

    @ahmadoudiop5016

    Ай бұрын

    Nn saway ken dou sock si beug détail

  • @MamecheikhnaNdiaye
    @MamecheikhnaNdiayeАй бұрын

    Nekal goor bro wa pikine la dieulale sokh gua mbeure mo guene

  • @trompeursambenebisamb6245
    @trompeursambenebisamb6245Ай бұрын

    Jackson mane n'a dane koudoul jackson

  • @user-gu5mx7vb5g
    @user-gu5mx7vb5gАй бұрын

    Denga niak ndeyou diom amo diemou mbeur sakh defofou tousss

  • @davidmendy3849
    @davidmendy3849Ай бұрын

    Sa data yaye 1000000000000000000

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749Ай бұрын

    😂😂 mé yaw khana daga faté yaw ak balla gaye beurka démba😂

  • @ModoumakhfoussDiop-sq9jn
    @ModoumakhfoussDiop-sq9jnАй бұрын

    Journaliste yiii aye vrai saytané lagnou

  • @bilalkhalyfall9938

    @bilalkhalyfall9938

    Ай бұрын

    Bilahi gnom gnoy yokeu problème bi dh

Келесі