« Balla Gaye dafa sétane Sa Thies combat bi, mo warone» Sokh fait de terrible révélation et dénonce…

Пікірлер: 107

  • @People221sn
    @People221snАй бұрын

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL

  • @OmarBao-gu5qp
    @OmarBao-gu5qpАй бұрын

    Bilay faralouma sokh mai dafa saff lambou boula kene bayuilo wakh dakh man sa ay wakh damakoy beug yalla Naga am diamou frère ❤

  • @dakardk4750

    @dakardk4750

    Ай бұрын

    Amine

  • @CheikhMbengue-fl8ik
    @CheikhMbengue-fl8ikАй бұрын

    Sokh championla nako gayi dieul so amate comba yalla nala yalla may ndam

  • @zoladiop9412
    @zoladiop9412Ай бұрын

    Diambar gua bilahi yalna yalla def la champion bu mak

  • @alassanengom4265
    @alassanengom4265Ай бұрын

    Billahi champion gua nék si rék lép Dina bakh inchallah

  • @user-ze9uy6zq5k
    @user-ze9uy6zq5kАй бұрын

    ndiabouta diouf fils champion nga xam nala bounakh do ragal gayi dagno beuri wax bilahi

  • @FallouLeye-gs3xt
    @FallouLeye-gs3xtАй бұрын

    sokh Ligeuyal rek daye bakh dh inchallah yawe war nga mana nék champion bou mage

  • @mahhabrwn439
    @mahhabrwn439Ай бұрын

    Yalna la Yalla maiy Ndam sor ameh COMBAT INCHALLAH 🙏🏾🙏🏾❤️

  • @serignetine8856
    @serignetine8856Ай бұрын

    Sokh boule ragale dara ❤💪

  • @MbayeNdiaga-ww7ml
    @MbayeNdiaga-ww7mlАй бұрын

    Eumeu séne moy sma mbeur bly. M3. Kéne meunoul sii yaw dr touss diam rk sokh diambar nga bly puissance rk inchallah

  • @khadimseck7774
    @khadimseck7774Ай бұрын

    Merci mbuer ya man ya epou dole ❤❤❤❤

  • @matarndiaye674
    @matarndiaye674Ай бұрын

    Sokh le grand champion

  • @user-oh8cg9nc8f
    @user-oh8cg9nc8fАй бұрын

    Sokh kou bakh nga wakhdji rafetna❤

  • @MansourDiop-wd2or
    @MansourDiop-wd2orАй бұрын

    Sokh deugg rék lay wakh dagnko yap késse

  • @gorandiaye1862
    @gorandiaye1862Ай бұрын

    Gouygui yaa geuneu sokher gneupe cariere motakh sokh retane sisa questionbi

  • @BourouSene
    @BourouSeneАй бұрын

    Ma machallah champion ❤

  • @moussagueye6119
    @moussagueye6119Ай бұрын

    S Touba rek motax ma beug la❤

  • @abdoulayendoye542
    @abdoulayendoye542Ай бұрын

    Sokh day dokhal lamb un vrai champion boule tontou les gens t'aime beaucoup ne dit rien diambar gua

  • @moussagueye6119
    @moussagueye6119Ай бұрын

    Sokhna s Touba lala beugeé ❤

  • @modoundiaye5658
    @modoundiaye5658Ай бұрын

    Bien dit

  • @PapemodouNdiaye-jj7ox
    @PapemodouNdiaye-jj7ox6 күн бұрын

    Sokh bilahi dagou motakh makoy suivre

  • @alioudiop2791
    @alioudiop2791Ай бұрын

    Rafetna Masha Allah yalna yalla takhawou sam amine yarabi Sock

  • @aliousene7405
    @aliousene7405Ай бұрын

    Sokh amal diam rek yaw ,champion gua déguéntane

  • @modoubarasene9678
    @modoubarasene9678Ай бұрын

    Sokhou ndanane gua de guenal liguèy rek❤

  • @khadimsene-qp9gi
    @khadimsene-qp9giАй бұрын

    Champion yalla bakh na DINA bakh in challah

  • @ibrahimadia9853
    @ibrahimadia9853Ай бұрын

    Sokh vs Mor Kang kang nako albourakh teug ou alboury vs sokh sokh jour combat Balla gaye 2 vs tapha Tine

  • @trace-infos2a846
    @trace-infos2a846Ай бұрын

    Bilahi wallahi sokh nekh ngama biss niki tay

  • @jrjr6558
    @jrjr6558Ай бұрын

    Maan ki dafa baari waakh Belahi yow yangi ni ne Emeu dula nuyu dor wakhtan ne lolu si birr nek. Ki dafa baari wakh trop.

  • @awadiongue5434
    @awadiongue5434Ай бұрын

    Akassa baye fall amal diam waye barké mame ckhiekh Ibrahima fall amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-ro4gy3ej2p
    @user-ro4gy3ej2pАй бұрын

    Merci beaucoup sokhou

  • @hadihadi708
    @hadihadi708Ай бұрын

    Machallah ❤ 🙏 ❤ 🙏 ❤ 💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽❤❤❤❤💚❤💚❤💚❤💚❤

  • @bambasene9551
    @bambasene9551Ай бұрын

    Sokh bilahi walahi talahi je t'estime bcq j'aimerais bien faire ta connaissance frère

  • @freesenegal12345
    @freesenegal12345Ай бұрын

    Mai sokh tamittt limouy wakh barineu dé 😂

  • @Ousmaneniangcapotv
    @OusmaneniangcapotvАй бұрын

    Champion

  • @PapaBaby-rp3bf
    @PapaBaby-rp3bfАй бұрын

    Bilaye damako beug guir yalla sa numéro la beug

  • @aichambacke3023
    @aichambacke3023Ай бұрын

    Yala nala yala takhawou guirr bege guie ga bege s touba

  • @massambadiallo-dd4kf
    @massambadiallo-dd4kfАй бұрын

    Kou beiry wakh la polite been lagniou

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105Ай бұрын

    Amo conseil boy diokhe wakh rek Sokh nopil nga demain entraîner do mbeur wakh kattt nga do tanth ken do référence de

  • @aichambacke3023
    @aichambacke3023Ай бұрын

    Bilakh bege nala guier liga wakh si s touba te dinala diapaler si yo beri

  • @BabacarNdiaye-sh1mk
    @BabacarNdiaye-sh1mkАй бұрын

    Numéro Sokh la beugone

  • @diopmar6382
    @diopmar6382Ай бұрын

    Wakh rek ngay def tapete nga do mbeur khamo dara nganan champion la

  • @khadimgueye1570
    @khadimgueye1570Ай бұрын

    Bilaye sokh mo bakh

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdongАй бұрын

    Mom dina giss sama sms ba mouye beure ak fran man kheuss bou bathie sers ma woo suporterou bathie seras yi yeup niou niow keureum suporteko ak estate ce le champion

  • @sarrabdou3040
    @sarrabdou3040Ай бұрын

    Sokh VS diéne kaïré Combat leu

  • @BabelThiam723
    @BabelThiam723Ай бұрын

    ❤❤❤Sokh késé ❤❤❤

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdongАй бұрын

    Isskeu kham ngen ni man kheuss bou bathie seras sockou mako wakh toussa bou nekh bi mouye touss diamo ni bi contre franc mako wakh bounko sanseee nako kontinee

  • @yvonnebadiane2702
    @yvonnebadiane2702Ай бұрын

    Boy déf Signature contrat dangay wah rekkkk .. mes bo démé stade dofa déff touss . Donc wagnil wah dji ????

  • @habibcisse6487

    @habibcisse6487

    Ай бұрын

    Sawaye doull domouhara sokhor rék billah

  • @yvonnebadiane2702

    @yvonnebadiane2702

    Ай бұрын

    @@habibcisse6487 Boula mété nga ndéye harou ??

  • @abdoulayediop9331
    @abdoulayediop9331Ай бұрын

    Wakh rék ngaye déf fi nga takhawoune né dangaye douma faran té faran moula douma dann la

  • @user-om2is2jv5i
    @user-om2is2jv5iАй бұрын

    Sokh amato diomm thi GWYE wakh rekk jackson prise nala guay dougg thi fils de balla daff lay reprise déee😂😂😂

  • @Salioudiouf-nr7pw
    @Salioudiouf-nr7pwАй бұрын

    sokh serigne ndiaye combat la

  • @mansourgaye4125
    @mansourgaye4125Ай бұрын

    Ok kone sokh dacor nga li cotch bakari done wakh sisa masse bou beuri mola teré beuré sokh fexel am muscle bou deugeur té wor

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105Ай бұрын

    Ay wakhal deparago kindi wadie retraiter waye tegalewo ndam

  • @papadiaw757
    @papadiaw757Ай бұрын

    Sokh maintien form bi rkk blh dayy bakh

  • @diaibrahim6798
    @diaibrahim6798Ай бұрын

    Courage champion day bakh deh

  • @NdeyemaguetteMbengue-ic6hr
    @NdeyemaguetteMbengue-ic6hrАй бұрын

    Degaul boy Niang rek la tek nit beugoul ken

  • @MbayeNdiaga-ww7ml
    @MbayeNdiaga-ww7mlАй бұрын

    Sokh diam rk ngay am bly

  • @dofoujackson2544
    @dofoujackson2544Ай бұрын

    Guemale yalla ga nagou ni Jackson dala dane yaw champion ga

  • @user-kx9id1ee1w
    @user-kx9id1ee1wАй бұрын

    Sa wax mo beuri

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdongАй бұрын

    Nako gayi diokh comba wa ginaw raill ragal doufa deuk pokola kasse mock sock nioye souniou bathie sers

  • @KhalilSow-le5gg
    @KhalilSow-le5ggАй бұрын

    Sokh am nga beuré mes sa fitou guéwe mo dém kholal lou waral lolou pour tewate cii lambj

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdongАй бұрын

    Man sockou mounalen wakh si mbakhal ak khol bou refet kholalma mem toussam mbeureyi mom la niou topando franc yaye 100 franc ak niounie pikin laniou deuk tousse bobou mako nee mou kontineko

  • @LDMmafialambji6812
    @LDMmafialambji6812Ай бұрын

    Dou franc kessé , Jackson dane nala tamit

  • @dakardk4750
    @dakardk4750Ай бұрын

    Sokh entrénéle boubakhe défaite dafa méti

  • @tallbathie1293
    @tallbathie1293Ай бұрын

    Sokh quess comba la

  • @massarsarr5746
    @massarsarr5746Ай бұрын

    Modou lo moy sama mbeur mai sokh dafma nékh ndakh dafa dérécte

  • @abdoudiouf2125
    @abdoudiouf2125Ай бұрын

    Ki defa bari wakh Goor dou bari wakh .nit def na lou eup fouf linga def si lamb te kene degou niou tap réseaux sociaux. Ngay ratatati ni rek

  • @Ydakh-ui5yo
    @Ydakh-ui5yoАй бұрын

    Sok champion gua mais dougnou doff balla guaye 2 diapou si

  • @abdougueye4837
    @abdougueye4837Ай бұрын

    sokh bou amone touti diapalé ken meunouko

  • @user-kh2rk9bz2e
    @user-kh2rk9bz2eАй бұрын

    Ki kagne laye nopi

  • @thebosh-se5lb
    @thebosh-se5lbАй бұрын

    Yoruul xollou mbeur dd

  • @sambagueye4526
    @sambagueye4526Ай бұрын

    Cart xalis

  • @user-ze9uy6zq5k
    @user-ze9uy6zq5kАй бұрын

    fils diam rekk ngay borom Diom nga bilahi xamnala boubakh

  • @MoulayefashonguisseGuiss-qj8dc
    @MoulayefashonguisseGuiss-qj8dcАй бұрын

    Yawe wakhe rak sokou danga bari wakhe

  • @habibcisse6487

    @habibcisse6487

    Ай бұрын

    sawaye katelén séne leuveul ndaye sokhor rék billah

  • @lhomme_fort
    @lhomme_fortАй бұрын

    Aka meune wax

  • @abdoulayendoye542
    @abdoulayendoye542Ай бұрын

    Sokh dafa safe lamb

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdongАй бұрын

    No sockou khol bou refet la yor kou khamoule sockou rek. Khamo kou am yitela si nit man aliou ba magou bathie seras mom peresente sockou mai kou bakh la man la kheuss bou bathie seras sa kharit

  • @malangkujabi5108
    @malangkujabi5108Ай бұрын

    Kii domou diola la

  • @BabacarSylla-vo3by
    @BabacarSylla-vo3byАй бұрын

    Loutakh do sportif Jackson danela diélle bou amoul féne dakh daw khéx bi

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdongАй бұрын

    Bathie seras ladienako si sock mouneema diapko khale bou yarou niow na bassiman bathie pour ma diapaleko si claf bi kon kou bakh la

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932Ай бұрын

    Sa thies bou danon lidou am

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932Ай бұрын

    Sathies reuge reug. Fouballa nekon fadam bour geuweul

  • @Aliotop-officilel
    @Aliotop-officilelАй бұрын

    Sokh vs quench. Sokh vs fils de balla Sokh vs diene kaiirai

  • @alioudiop2791
    @alioudiop2791Ай бұрын

    😂😂😂😂😂😂💪💪💪

  • @abdousene261
    @abdousene261Ай бұрын

    Fils de balla da khamoul bopam koi

  • @saliougueye2348
    @saliougueye2348Ай бұрын

    Bilahi barri wakh sokh demal ga ligueye ga Ama ndam lamb Dou wakh bou barri way

  • @user-ze8uc7is6b
    @user-ze8uc7is6bАй бұрын

    😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @souleyewade7419
    @souleyewade7419Ай бұрын

    SOKH IL PARle tro pour. Rien

  • @omarndoye3410
    @omarndoye3410Ай бұрын

    Yaw wakh rk gua def 😂😂

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932Ай бұрын

    Sokh day wakh ba danou niew mou

  • @Dembsfoot
    @DembsfootАй бұрын

    Fils de balla est à la portée de sokh Sokh peut le battre sans problème mbeurou guédjewaye wakh rék

  • @papenar2561
    @papenar2561Ай бұрын

    Sokh yaw wakh dji ngay wagni té djéma di dane amo foula sa rak yi sax raw nagnou la

  • @ibouciss3519

    @ibouciss3519

    Ай бұрын

    Saway démal gua khol palmarès sokh après gua nieuw niou wax ki 3 combat rek franc moko dane marley match nul jackson dane ko guanane raww 😂

  • @kefgg

    @kefgg

    Ай бұрын

    ​@@ibouciss3519Boleesi Domou Dangou dore ko mou danou Ram Dam dane ko. Palmares Sokh 2017 ak legui lane leu? Loumou fi def si 7 ans yi passer?

  • @abdoulayesarr3894

    @abdoulayesarr3894

    Ай бұрын

    Sokh yalla na la yalla défal diame si barké mouhamed ya bakh boul wakh lou bone

  • @ibouciss3519

    @ibouciss3519

    Ай бұрын

    @@kefgg fi guiss nagne fi alioune seye 2 guis nagne fi eumeu séne ak yénéne mbeur lamb nekoul chaque jour lay nekh soukh meussoul dougou si géw yafousse

  • @kefgg

    @kefgg

    Ай бұрын

    @@ibouciss3519 Non Sokh diambare la amena fite mais defoul performance si annee yi passer. Eumeu Sene bimouy ame tolof tolof debut carriere leu si temps khalé ay 24 ans 25 ans yoyou. Mais Sokh nekoul debut carrière 2014 la dane Boursine. Dou makeu wayé dou khalé tamit kone sou téyéwoul lamb legui kagn lakaye téyé sou amé 40 ans?

Келесі