Modou Lo Mo Dakh Beuré Ci Lamb Ji" Alioune Sèye S’explique" Demna Mbapatt GUEDIAWAY PIKINE PARCELLES

Спорт

🔴✅Abonnez-vous ✔ | et ✔Activez Les 🔔NOTIFICATIONS👇
👉 / senlambtv
👇Vous Pouvez nous contacter sur:👇👇👇
📞🔊WhatsApp: +(221) 779098319
Facebook: 👉 / sen.lanbtv
Instagram: 👉 / sen_lamb_tv
#luttesénégalaise #senlambtv #lamb

Пікірлер: 128

  • @mawachiinter4130
    @mawachiinter41302 жыл бұрын

    Billaye Modou lo es le meilleur n'importe quelle techniciens le diras : 1 vue sa taille.. 2 vue sa corpulence.. 3 vue sont poids ...4 vue sa constances ... 5 vue sa lecture de combats et sa résistance Modou lo n'a jamais pris d année sabbatique pour aller ce refaire ,or certains le font deh qu'il perde 1 combat Modou lo es le Messi de la lutte sénégalaise

  • @diawameth4382
    @diawameth43822 жыл бұрын

    Ndeysan il es trop poli yalnala yalla defal diame 🥰

  • @gueyefgm6331
    @gueyefgm63312 жыл бұрын

    Modou lô meilleur lutter du Sénégal

  • @mohamedfall6260

    @mohamedfall6260

    2 жыл бұрын

    Balla gaye 2 moy sénn bay yénn wa parcelle

  • @papeseck4667

    @papeseck4667

    2 жыл бұрын

    Lolou la yalla dogal

  • @diallosouleymane4370
    @diallosouleymane43702 жыл бұрын

    Modou Lo c’est le meilleur lutteur

  • @idrissadioufsane2166
    @idrissadioufsane21662 жыл бұрын

    Bisnikii tay iow lay supporter ndah linga wah cii mn roi xaragne💪💥👌

  • @naturehumaine1219
    @naturehumaine12192 жыл бұрын

    Alioune Seye 2 maan beuré ko bollé ci lamb. Wayé jikko ji dou mbeur. Ki dafa yarou trop xol bi yatou mashallah

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Y’a bakh

  • @metmolambassadeurdesagener8813

    @metmolambassadeurdesagener8813

    2 жыл бұрын

    Bilahi lolou man si meun nako sedè nio bokou kogne Nitt kou bkh la

  • @moussathiaw7696
    @moussathiaw76962 жыл бұрын

    Aliou seye kou gnak kignane nga kou bakh nga Baye FALL pire nga bonne continuation champion

  • @maodokane8671
    @maodokane86712 жыл бұрын

    Merci thii linga wakh modou😍

  • @KANEBOUSEYDIAHMEDTIDIANE
    @KANEBOUSEYDIAHMEDTIDIANE2 жыл бұрын

    Modou yallana yalla maye kou ndame bou Nice barki seydina Mohamed psl

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Amine

  • @ibrahimafaye5808
    @ibrahimafaye58082 жыл бұрын

    Suis vraiment d'accord avec lui Modou lo est le lutteur le plus ide l'arène

  • @lahadboukharagnelo6707
    @lahadboukharagnelo67072 жыл бұрын

    Lolou Betty la fanan lamb Sénégal dotoul am kou melni Modou Lo

  • @tallacisse7797

    @tallacisse7797

    2 жыл бұрын

    Bilayy walay deug rek gua wakhh

  • @tallacisse7797

    @tallacisse7797

    2 жыл бұрын

    Moma bayi ci Lamb dh

  • @lahadboukharagnelo6707

    @lahadboukharagnelo6707

    2 жыл бұрын

    @@tallacisse7797 dafa lerr

  • @hasboyedawe9569

    @hasboyedawe9569

    2 жыл бұрын

    Lolou dafa lerr

  • @lahadboukharagnelo6707

    @lahadboukharagnelo6707

    2 жыл бұрын

    @@hasboyedawe9569 ✅✅✅

  • @beuguserignefallou1966
    @beuguserignefallou19662 жыл бұрын

    Bilahi kou bakh nga te am nga yare lol machallah..nite soko kholé rék souy wakh di nga kham moy kane..mais yalla na la yalla guena takhawou si barcke mame fallou champion 🙏

  • @cheickmoinga3245
    @cheickmoinga32452 жыл бұрын

    Modou lô Ndam rék incha'allah

  • @mouhameddiop5754
    @mouhameddiop57542 жыл бұрын

    modou lo rek 💪🏽

  • @soraboukharagnelo5717
    @soraboukharagnelo57172 жыл бұрын

    Bilaye lolou defa lerr souma wakhé nioné sa way mee modou mo daka beuré si lamb djui

  • @ametdiengcolobane1699
    @ametdiengcolobane16992 жыл бұрын

    Merci''''Modou'''ra

  • @bigmakhouframaaren2221
    @bigmakhouframaaren22212 жыл бұрын

    J'ai tout suivi Aliou Seye n'a point dit que XLO mo dakh beré si lamb ji dakoo nangoul ndaananam rkk té niépa koko nangoul mais le meilleur de sa génération est et reste BG2 . XLO vient à la 2ieme place lii mo raisonnable

  • @ibrahimafaye5808

    @ibrahimafaye5808

    2 жыл бұрын

    Moodou loo moo dakh beurri ball gueye fopp mooko dakh xeeex leu koo cii beurri seulement lou takh Modou manta daan ballla sééni rallonge moo bokkoul ballla deeka soutt se trop mais dou mooko meuo wala mou dakh koo beurré bounou tooloowoon nga léneeen

  • @bigmakhouframaaren2221

    @bigmakhouframaaren2221

    2 жыл бұрын

    @@ibrahimafaye5808 😀😀😀yaw danguaa baakh rkk fall so wakhé khékh dé ma d'accord mais beuré BG2 mooy number one moossi man 😇😇

  • @ibrahimafaye5808

    @ibrahimafaye5808

    2 жыл бұрын

    @@bigmakhouframaaren2221 waalaahi Balla meunoul Modou cii beurré faall lii malakoo wakh

  • @hitthelink662

    @hitthelink662

    6 ай бұрын

    Modou dà tolloule ni balla lolou mo joué ci sen concurrence, imagine modlo tolou ni balla + limu amni kone balla dou fègne, le contraire tam bu balla tolone ni modu dou fégne aussi wala dina meti lole ci mom

  • @ayoundiour9374
    @ayoundiour93742 жыл бұрын

    Modou lô the king

  • @delmoguisse2742
    @delmoguisse27422 жыл бұрын

    Kendou modou lô

  • @mamic4837
    @mamic48372 жыл бұрын

    Mais où est moumeu quesqu il est devenu tout le monde parle de lui que c'est un champion

  • @cheikhounafall4477
    @cheikhounafall44772 жыл бұрын

    Danga bakh alioune linga wakh thi sama Mbeur bii Nice amal diam

  • @thiernogueye5654
    @thiernogueye56542 жыл бұрын

    Vive champion waakhe dji rafètena

  • @mouhamedba3818
    @mouhamedba38182 жыл бұрын

    Modou lo

  • @Chicory-tv
    @Chicory-tv2 жыл бұрын

    Champion deugue moungui ni d sétaan nako Pikine mom ak iboulaye bou écurie l'eau chaude gno jordon ak gnoom Mamadi seras gno indiwoon iboulaye mou daan ko dièl bou reuy

  • @papembaye5335

    @papembaye5335

    2 жыл бұрын

    Bilahi lamb toucouleur fofou la khamé Aline sey

  • @mamadoudieng3093
    @mamadoudieng30932 жыл бұрын

    Modou kharagne lo moy lamb

  • @aladjisow1747
    @aladjisow17472 жыл бұрын

    Louler frere kènne dou kharagne lô

  • @khadimbambandiaye8133
    @khadimbambandiaye81332 жыл бұрын

    Mbeur mou yarou mingui ni kou niak kignane yoroul jikoy mbeur so xolé kanam gui sax xamni kou bax la yalnala sunu borom taxawou

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Amine

  • @ousseynoufaye4407
    @ousseynoufaye44072 жыл бұрын

    Moussa dioum ndeysanne aduna do comprendre koi

  • @bayelahatdiagne9542
    @bayelahatdiagne95422 жыл бұрын

    Xaragn lo mo takh ma kham Lamb

  • @doudouseck7012

    @doudouseck7012

    2 жыл бұрын

    ak man

  • @mouhamedba3818
    @mouhamedba38182 жыл бұрын

    Yalla nala yalla same deugue rek moy deugue

  • @sallkhadim5268
    @sallkhadim52682 жыл бұрын

    Nice na torop

  • @awambayeeva6698
    @awambayeeva66986 ай бұрын

    Merci Alioune seye de dir la vérité sur Modou lo ya des luteur ki ne apset pas le chenpion de Modou lo mes alla et grand Modou lo yalna yala may nam inchallah ❤️🙏

  • @aladjisow1747
    @aladjisow17472 жыл бұрын

    Ya gorè waye frère

  • @boubafall1014
    @boubafall10142 жыл бұрын

    Motax sén combat yén niar néxone niari mbeurantane gén Mod’lo lossi meun degg bilahii dafa meun mbeuré kouko suivre mbapatt xam ni ohhh kén dou moom

  • @serignendiaye4899
    @serignendiaye48992 жыл бұрын

    Balla gaye dou moromou modou😁😁😁

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Lou niou bindeu ak li ki wakh bokoul sétanal lép

  • @younoussediop2501
    @younoussediop25012 жыл бұрын

    Mbeur amal diam rek

  • @assaneba3418
    @assaneba34182 жыл бұрын

    Ndeysane borom khôl bou bakh ngua

  • @abdoudiop5163
    @abdoudiop51632 жыл бұрын

    Mbapat yeumbeul babacar diallo limouko dieule kene dieulouko bilahi aka manone beure trop

  • @khadyba4478

    @khadyba4478

    2 жыл бұрын

    Anamou dfa bayil beureh khana

  • @makhtarjaw319
    @makhtarjaw3192 жыл бұрын

    Pour tan nk ya dakh. Beuré si lamb ji wakh nako founé te. Khamna si Dara lalé Nanou mane AK yaw

  • @lahadboukharagnelo6707
    @lahadboukharagnelo67072 жыл бұрын

    Modou anta liguey bi mogui diar yonn surtout question 🙋‍♂️ yii

  • @ahmetmbodjmbodj4686
    @ahmetmbodjmbodj46862 жыл бұрын

    Li motakh bigay beurè batay kèn khamoula 🤣🤣🤣Balla moy bayou beur yi 💪❤

  • @generalsall9123

    @generalsall9123

    2 жыл бұрын

    Boulfi sisou way limou wakh loumou la metti

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Dél sétane bamou diékh ki wakhoul modou mofi dakeu beuré c juste si Modou Lo laniou ko lathie

  • @khadimndiaye1803

    @khadimndiaye1803

    2 жыл бұрын

    Frère Aliou seye day sissou balla d'où moromou mbeur si lamb ji

  • @saerdiagne8198

    @saerdiagne8198

    2 жыл бұрын

    Soungéne sissouwoul wone rkk mou diaxal ma 👉😂😂😂 yéne wakeur balla gay yi nangouléne li yalla dogal nakk 🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @ibrahimafaye5808

    @ibrahimafaye5808

    2 жыл бұрын

    Wallaahi Modou lo moo dakh beurri ballla Gueye dénion bookoul rallonge rkk ballla daaka soutté rkkk

  • @ngangedrammeh6264
    @ngangedrammeh62642 жыл бұрын

    Lou titre bi binde ak lou alieu seye cest diffirent

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Merci niou beuri erreur bobou laniouy déf

  • @khadyba4478

    @khadyba4478

    2 жыл бұрын

    Pour am ay vue rek

  • @falloundiaye8774
    @falloundiaye87742 жыл бұрын

    Aliou seye 2 wokhoule lolou bayiléne doule wa mais balla gaye 2 ban position lay takha wé

  • @cheikhmbacke4379
    @cheikhmbacke43792 жыл бұрын

    ALIOUNE SEYE2 BOROM WEURSEUK DEWEN KEN DOU KO LEKK REIN YALLA NASSA DIAM YAGG

  • @cheikhly6777
    @cheikhly67772 жыл бұрын

    Champion bi Nice na

  • @massambathiam6891
    @massambathiam68912 жыл бұрын

    Modou lo nandane la mai lamb mo bakho thiow dou mbeur mou ndaw déh bakhna

  • @alassanendiaye5608
    @alassanendiaye56082 жыл бұрын

    Borom bakh nga Courage

  • @diopmahanta9983
    @diopmahanta99832 жыл бұрын

    🥰🥰

  • @toureabdou3629
    @toureabdou36292 жыл бұрын

    Wa kiy mo bakh way

  • @loufa9357
    @loufa93572 жыл бұрын

    Boye bou yarou billakhi

  • @ibrahimambaye9275
    @ibrahimambaye92752 жыл бұрын

    Balla gaye 2 moy meilleur lutteur de tout les temps

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Sétanal lép wakhoul Modou Lo mo dakeu beuré si Lamb dji site yi nioy wakh louléne nékh

  • @irenebassene9122
    @irenebassene91222 жыл бұрын

    So Bolléwone meunmeunou lamb kati yeup nga Andi ték king balla moléne dakh beuré eupeléne dollé🤫🤫🤫👎👎👎👎

  • @thiawzall1547
    @thiawzall15472 жыл бұрын

    Aline sey Mbapat bi amon assa diouf Modou lo mo dann

  • @saliouniang9713
    @saliouniang97132 жыл бұрын

    Wakhoul lolu bayilén fén AK diakhassé xelou nit gni

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Merci Yaw comprendre gua

  • @omargueye1329
    @omargueye13292 жыл бұрын

    Sene titre you kat waye dounguene bayi féne

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Merci niou beuri erreur bobou laniouy beuré

  • @libasseniang7869
    @libasseniang78692 жыл бұрын

    Mod lo manoul dakh beuré Balla Gaye, ne soit pas un jaloux

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Diabar sétanal bamou diékh c important si Modou laniouko lathie en plus site yi nioy bindeu lou bokoul ak li ki wakh.

  • @kalidoukaneollaid4509

    @kalidoukaneollaid4509

    2 жыл бұрын

    Frere xana waxe sa beug beug amoul

  • @B-221

    @B-221

    2 жыл бұрын

    Man Mbeur foka diap Dan ko Ak mana beure dou Ben Balla sakh mom Wakhnaco modou koumana beurereu

  • @bebealiouseye5058
    @bebealiouseye50582 жыл бұрын

    Diame rek mag dji

  • @abosarr7369
    @abosarr73692 жыл бұрын

    Assane diouf modou lo mo dieule poi lessé bi jour bobou

  • @lassanatalla767
    @lassanatalla7672 жыл бұрын

    Aliou seye djiko waliw la yoré

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Bilay

  • @trace-infos2a846
    @trace-infos2a846 Жыл бұрын

    Omar Fall mouma amoul morome si mbappat🥲

  • @samsyoutubeur2544
    @samsyoutubeur25442 жыл бұрын

    C'est la première fois ma guiss kou wax modou lo mo dakk beurré si lamb dji😂😂😂😂😂😂😂😂😋😋😋😋

  • @ndatemboup9111
    @ndatemboup91112 жыл бұрын

    Moussa dioum rek

  • @baamadou5667
    @baamadou56672 жыл бұрын

    Xlo

  • @mbayediallo4123
    @mbayediallo41232 жыл бұрын

    Wayee ken dou sire seras si mbapat

  • @papendiaye3400
    @papendiaye34002 жыл бұрын

    lamb wakhoul deug ki mako kham

  • @loufa9357
    @loufa93572 жыл бұрын

    Yalla ga dorr zoz mou danu

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Amine

  • @mohamedfall6260

    @mohamedfall6260

    2 жыл бұрын

    inchalla

  • @loufa9357
    @loufa93572 жыл бұрын

    Diame rek aliu séye 2

  • @ngangedrammeh6264
    @ngangedrammeh62642 жыл бұрын

    😅🤣😂😂, balla ngi nyow deh!

  • @saerdiagne8198

    @saerdiagne8198

    2 жыл бұрын

    Sou gneuwé rkk fékk fi eumeu séne rkk fi kounékk akk kiy sa bayyy 👉😂😂😂😂😂

  • @elhadjimodouthiam5566
    @elhadjimodouthiam55662 жыл бұрын

    Aline saye manga baré torop waya gamo sabopou paska gni diekhal rék ngay baréle ay issa pouye ay zoos yi danléne doula yobou féne

  • @khadyba4478

    @khadyba4478

    2 жыл бұрын

    Wkhe deug n'a djeul niom franc après reug boy Niang Malick Niang

  • @serignemodoundiaye8418
    @serignemodoundiaye84182 жыл бұрын

    Boye niang dafa yague alioune seye nena mbapat bi papam teugon mo doon bindeu mbeur yi dou xallei deh mook gars yi ño massei yaa mak Ama nangoul

  • @assballagaye2348

    @assballagaye2348

    2 жыл бұрын

    Boy niang da yague deh

  • @serignemodoundiaye8418

    @serignemodoundiaye8418

    2 жыл бұрын

    @@assballagaye2348 billaye ioe meme generation ak balla gaye modou lo alioune seye 2 gars yi mo mak aye ama aye sa thies yii deh

  • @massniang8245

    @massniang8245

    2 жыл бұрын

    boy nian avec un age de 10 ans tant boy meuna bit ay tour c juste là il été à l élémentaire alors mbeur yi nom beuré minimum amneu plus de 15 ans

  • @serignemodoundiaye8418

    @serignemodoundiaye8418

    2 жыл бұрын

    @@massniang8245 🤣🤣🤣🏃‍♂️🏃‍♂️🏃‍♂️🏃‍♂️ fall 10 ans ngaye took di bindeu touru mbeur yi thi mbapatt mbapatt ak nimou kadjamei

  • @concept2798

    @concept2798

    2 жыл бұрын

    Bilahi walahi Boy Niang dou mak, nio done bok bén banc primaire. Bo xolé Balla bimiy beuré ak Bathie Seras (té Bathie ak sougnou taw, may niétélou topém nio bokone class, té bigniy bathie Cm2 man dougagouma ecole) nga xamné balla dou goné. Mo mak Boy niang fouf lolou dou wax. Té lolou dou débat l'essentiel moy lou meuna am moy Boy niang dapnako ci lamb batay mouy meuna beuré ak mom

  • @challenge6757
    @challenge67572 жыл бұрын

    Seytané nga 🤫

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Détt way

  • @papeseck6124
    @papeseck61242 жыл бұрын

    Ndaysan daga bakh rk

  • @diopfasye3930
    @diopfasye39302 жыл бұрын

    Modou lo modakha beurre ana Balla gay

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Sétanal lép titre ak li ki wakh bokoul

  • @mamathiam5649
    @mamathiam56492 жыл бұрын

    iow dh bayina sa ndeye doule Kate bi bigua done balla gaye mo dake beuré ci lambe dji iow dh doto takh ma déme stade

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    Yaw nékal nitt yaw bo faraloul loumou koy wagni sof gua trop

  • @sarrmassaer1870

    @sarrmassaer1870

    2 жыл бұрын

    Yawmi ya tégal sa ndeye amaloko ben ndiarigne domeram

  • @abdousarr9749

    @abdousarr9749

    2 жыл бұрын

    Do am yarr wakh t bayi sagayii loutakh amolen respe vré mierda

  • @sarrabdoukarime8259

    @sarrabdoukarime8259

    2 жыл бұрын

    @@sarrmassaer1870 ki amoul yar bo sétanone lép do wakh li site nioy diakhassé rék wayé wakhal Modou Lo mofi dakeu beuré

  • @papaabasssarr7839

    @papaabasssarr7839

    2 жыл бұрын

    Yaw ya rew kingay saga nek sa Clavier cool motakh ngakoy def site yi nagnou kholat lignouy bind ki wakhoul modou lo modakh beure thi lamb ji

  • @neymarndiayetv6140
    @neymarndiayetv61402 жыл бұрын

    Modou lo

Келесі