Modou Lô démonte et humilie Tapha Tine "Mo gueuneu yomb beurél… Dafa yakamti rek wayé…"

Спорт

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
/ luttetv
/ luttetv
/ luttetv
luttetv.com/

Пікірлер: 251

  • @user-fj1co7vf3o
    @user-fj1co7vf3o2 ай бұрын

    Diomaye prisidant du Sénégal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ndame rék inchalla pour le Sénégal ❤❤❤❤❤ fii yallaa finé dh bilaye

  • @user-dc2pq1zl3n

    @user-dc2pq1zl3n

    2 ай бұрын

    Modou lo rek kese❤❤

  • @DameNguirane
    @DameNguirane2 ай бұрын

    Gniy wakh modou da ragal Tapha tine yeup ak fans fawzeyni lagn😅😂

  • @mouhamedsambe7820

    @mouhamedsambe7820

    2 ай бұрын

    Boul wax lolou

  • @jesuismoi4269

    @jesuismoi4269

    2 ай бұрын

    😂😂😂😂

  • @abdoulayesalim6575
    @abdoulayesalim65752 ай бұрын

    Modou Lô a raison Tapha Tine mo guèneu yombe daane

  • @falloumbeguere8551

    @falloumbeguere8551

    2 ай бұрын

    Wakholl yoba dan yomba berèll la wakh nay lèr

  • @ModouMbaye-vv6oy
    @ModouMbaye-vv6oy2 ай бұрын

    Li dh la wakhone contre ama té après guiss guéne lisi xéw😂

  • @assanewade6616

    @assanewade6616

    2 ай бұрын

    𝐃𝐨𝐮𝐦𝐚 𝐚𝐦𝐚 𝐃𝐚𝐧𝐞 𝐤𝐨❤

  • @moustaphambaye3393

    @moustaphambaye3393

    2 ай бұрын

    Ki day wakh rk dafa tapet tapha tine amoul loum wax dafa daw

  • @Abdk0p

    @Abdk0p

    2 ай бұрын

    ​@@moustaphambaye3393tapha tine thouné la billahi bayil bamou tassé ak mom😂

  • @MamecheikhtidianeDiop-du5qs

    @MamecheikhtidianeDiop-du5qs

    2 ай бұрын

    ​@@Abdk0pbilay même balla lolou lakoy wakh bo sétané combat wam ak eumeu guay kham ni dolé rék la am

  • @punchyork7167
    @punchyork71672 ай бұрын

    Il dit très vrai. Tapha il est très lent dans sa lutte et Modou lui il est vif et rapide. On l'a vu contre Eumeu Séne, Eumeu amneu temps attaquer ba dougueu si Garde Tapha ba door ko coup. Balla Gaye 2 si il est prêt physiquement aussi dinagniou guissat lolou.

  • @fifty6292

    @fifty6292

    2 ай бұрын

    Légui Khana Tapha Tine dou nite Eumeu Séne loumou def Balla Gaye ? Bayil thiakhane louné meune na khew

  • @punchyork7167

    @punchyork7167

    2 ай бұрын

    @@fifty6292 j'ai jamais dit que Tapha Tine est un vampire. Lou nekkeu meuneu khew c'est vrai mais le constat est que Tapha Tine dans ces combats il est lent lolou c'est vérifiable. Il est très lent. Aprés waxouma batay daffa nul wala dara. C'est juste une analyse. On sait tous que un Balla Gaye en possession de tous ses moyens t'attaque avec vivacité et rapidité hors Tapha il est pas rapide. C'est la même chose pour Modou il est très rapide et vif d'ailleurs on a même vu ça sur ces dernier combats. C'est juste ça Tapha est lent. Mais après lou nekkeu meuneu khew

  • @user-fj1co7vf3o
    @user-fj1co7vf3o2 ай бұрын

    Vive sonko inchalla taye ak souba inchalla yalla bakhna inchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤ ndame rék inchalla pour le Sénégal ❤❤❤❤❤❤

  • @user-dc2pq1zl3n

    @user-dc2pq1zl3n

    2 ай бұрын

    Modou lo kese

  • @rimesmakerposeidon2427
    @rimesmakerposeidon24272 ай бұрын

    Modou lo Messi de la lutte sénégalais

  • @nioukyvictor364

    @nioukyvictor364

    2 ай бұрын

    vétrité absolue❤

  • @user-gw8qv9zg5b

    @user-gw8qv9zg5b

    2 ай бұрын

    Messiiii bou daw tapha tine 😂😂😂

  • @boubaleye2003

    @boubaleye2003

    2 ай бұрын

    😂😂😂 messi dou daw joueur

  • @khalil7083
    @khalil70832 ай бұрын

    modou le Roi mane iow rek lay topou

  • @tallacisse7797
    @tallacisse77972 ай бұрын

    Le Roi le Vrai

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse48542 ай бұрын

    Thiye monsieur le maire moy ndanan ❤❤❤

  • @adviseragnam7050
    @adviseragnam70502 ай бұрын

    Il a raison Tapha thiouné la

  • @Wdkhgfukhhhhhhhhyuj
    @Wdkhgfukhhhhhhhhyuj2 ай бұрын

    Yén deugoulén wolof modou sawaroul si tapha😂😂

  • @morndiaye7785
    @morndiaye77852 ай бұрын

    Ama dane tapha tine Modou lo dane Ama Boy niang dane sa Thiès Modou lo dane boy niang Bilahi modou ndandane la 🎉❤❤❤

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    2 ай бұрын

    Saway Lolou dou lamb ! Eumeu danena Balla ak Bomb gnou dane Modou te Modou mo dane Eumeu. Lamb dou logic !

  • @teufthiam7241
    @teufthiam72412 ай бұрын

    Sénégal comme niou weroul li dou émission politique

  • @user-wq8jo4zq6g
    @user-wq8jo4zq6g2 ай бұрын

    Il est le meilleur aux monde

  • @user-mc1fi6ly4u
    @user-mc1fi6ly4u2 ай бұрын

    Bilahi dgeu leu wakh tafa tine d'ay absenté sibir combat lolou nak sportif mokoy gussi😂😂

  • @saliougueye9833
    @saliougueye98332 ай бұрын

    Tafha tine dhh doyouma dara si modou modou mi dafa say say trop

  • @DjibrilBa-xp7te
    @DjibrilBa-xp7te2 ай бұрын

    Modou bou amadou bâ futur président 2034😂😂😂😂😂😂

  • @user-yl4gb2if9e

    @user-yl4gb2if9e

    2 ай бұрын

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar95482 ай бұрын

    Pourtant loum wakh nii mane d'accord nasi de tapha tine tangoule de 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ousmanecisse4262

    @ousmanecisse4262

    2 ай бұрын

    Wallahi nak srx 😂

  • @user-sq7qc5ie7o

    @user-sq7qc5ie7o

    2 ай бұрын

    Merci boncou fréro

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    2 ай бұрын

    Non Tapha mom saway nullard la 😂😂😂 mais Dafa am djapaler legui dhee

  • @elhadjidiouf5991
    @elhadjidiouf59912 ай бұрын

    Modou lo rék ❤

  • @mamadoulakhciss8652
    @mamadoulakhciss86522 ай бұрын

    Malheureusement amna niou hamoul geud sport un sportif de haut niveau beuré 2 combat si béni saison c normal mou nopalou ak lamb noumou mété.Tapha mo amoul management bou bah

  • @tvadamandiayekhassaidtouba8388
    @tvadamandiayekhassaidtouba83882 ай бұрын

    Tafa Tine bo yeboo nga wathie Te kham ni modou mongi laye prépare 😱👂🏿👂🏿

  • @user-bn9jc1rp9q
    @user-bn9jc1rp9q2 ай бұрын

    Da ngua daw tapha

  • @MouDiop-tk5rw
    @MouDiop-tk5rw2 ай бұрын

    il est le meilleur 💪💪

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane71632 ай бұрын

    Lutte TV manshalha

  • @user-xi3vu7jq2e
    @user-xi3vu7jq2e2 ай бұрын

    Modo rék ❤❤

  • @malickdia3495
    @malickdia34952 ай бұрын

    Machalah ❤❤❤❤

  • @user-rn8qo3fj5r
    @user-rn8qo3fj5r2 ай бұрын

    Mais tapha tine manoul dan modou lo wakhdij mofi nek rk

  • @dembandiaye585

    @dembandiaye585

    2 ай бұрын

    Ya moune féne

  • @jesuismoi4269

    @jesuismoi4269

    2 ай бұрын

    Waxx deugu yallah

  • @user-rn8qo3fj5r

    @user-rn8qo3fj5r

    2 ай бұрын

    @@jesuismoi4269 no lou léer kokou amoul kham kham blh

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu58892 ай бұрын

    Saway Dieuleule Tapha Tine ndiata Ath ngacoy Daww 🤧Mbeur Mome Tankeu Danoko Mounoko Dangacoy Daw pendant des années 🧏‍♂️finga parésy Boy NIANG Tapha Nala Parèna amateurs yeupou Na moy logique actuellement lowax dangay poge Nga bayii Ba Tapha Dieule Balla rék Nga Gaw Dieuly siteu Donc Danga Donko Moytou Modou wallahi Danga Ragall Tapha Tine saway waxal waxdji ndièméwoo Tapha Tine Dei saway 🤫Dieuleule Tapha Tine 🥹Dieuleul avance by rék

  • @talladiop4837

    @talladiop4837

    2 ай бұрын

    Lolou nguéne waxone si ama baledé aye modou lo dafa daw guis nguéne fimou moudié

  • @dembandiaye585

    @dembandiaye585

    2 ай бұрын

    Merci frère bien dis

  • @DameNguirane

    @DameNguirane

    2 ай бұрын

    Sa wakh dji goudou na amoul sens té modou lo douko lire😅😂 soff ngéne trop

  • @ibrahimadrame9499

    @ibrahimadrame9499

    2 ай бұрын

    😅😅😅😅😂😂😂😂 l'absolu Gueye yaw warato wakh sa mairou deukeu dara modou séne papa la 😅😅😅mougnal rék yalla bakhna yaw mom meuno beugue kharagne lo bayou wa pikine😅😅

  • @mbayestarsene2179

    @mbayestarsene2179

    2 ай бұрын

    Gni bayi lein modou lo sou dane wa lamb dji yeup niou ande ape joueur sou bagné niiouné dafa daww😂😂

  • @user-qt6eo2sb2n
    @user-qt6eo2sb2n2 ай бұрын

    Bilay yako mon

  • @Babacardiane221
    @Babacardiane2212 ай бұрын

    Wiri wiri diari ndari yag yag dadié

  • @cheikhgueye7309
    @cheikhgueye73092 ай бұрын

    ❤❤❤❤

  • @sambaba683
    @sambaba6832 ай бұрын

    Modou lô dèffa ragual tapha tine il èvite tapha tine modou douffoulllllda ragual wadji il est malin😂😂😂😂

  • @KhadimDiop-uw8dl

    @KhadimDiop-uw8dl

    2 ай бұрын

    Yaw wérro déee

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane71632 ай бұрын

    Fallait le prendre

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj2 ай бұрын

    Modou lôooooooooo ❤❤❤❤

  • @agenperf1826
    @agenperf18262 ай бұрын

    C'est notre Seigneur ALLAH soubhàneho wa tàlà qui accorde la Victoire à qui il veut . Sourate 8 / verset 10 .

  • @seydinandiaye6554
    @seydinandiaye65542 ай бұрын

    Li wakhou politicien laa 😂 Kiii mingui campagne bataye deh😂 wakhlenneu KO Amadou a perdu 😅 Fall danga daw tapha . Mais je te supporte parfois

  • @papadiom9260
    @papadiom92602 ай бұрын

    Saway Champion nga Mais nekaal niit ! Ba ngay wakh Tapha “dof bou yewou laa” BCAO 2014 lawone bilahii 😂. Yaw ak sama mbeur (Eumeu) bilahii depuis 2014 ngene di moytou avance Tapha ! Eumeu warona djeul Tapha daneko bou yag mais di bene benal ba Tapha am djapaler thi digeunter moukay soga djeul. Tapha meunoka dane djamono dji..

  • @thiamahmadulattekh562

    @thiamahmadulattekh562

    2 ай бұрын

    Ay wax gueine veuri Dou dolei. Bi Dou dor. Bi Dou. Beurei bi Lep modou mokoko eup

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    2 ай бұрын

    @@thiamahmadulattekh562 Beurer bii waw..mais doler ak khekh bii ?? Yaw lolou yaw Sa bopou geumo ka sakh ! Modou lo Boy Niang waner naa ay defauts wam thi khekh lou beurii ! Fouko Tapha koor ngene forii ko! Combat bobou comme Modou - Bomb rekk dinako toucher deff lounekk Mais fouka Tapha djap mou djekh !

  • @abdoufoir232
    @abdoufoir2322 ай бұрын

    Tapha tine mola mane foufe bilay

  • @cheickhouthioune9149
    @cheickhouthioune91492 ай бұрын

    Aucune confirmation il a peur de Tapha tine..si comme tapha est facile à battre vu ton analyse est que tu confirmes pas ton combat avec taoha alors tu te contredit... seulement une analyse

  • @barhamathiane83

    @barhamathiane83

    2 ай бұрын

    Modou amoul ragal si tapha Tine il a fait déga fait ses preuves amoul koumouy ragal si lambe dji

  • @musiqueretrotv790
    @musiqueretrotv7902 ай бұрын

    Tapha tine bou dané balla gaye 2 moy donn roi des arènes

  • @user-bk4nf7cj6r
    @user-bk4nf7cj6r2 ай бұрын

    daye tek khel tapha t'ene Aka intelligent 🤣🤣🤣

  • @serignegueye3035
    @serignegueye30352 ай бұрын

    Modou Li gua wax yombou na trop dieul ko ba danko ba paré Tapha da am dolé

  • @user-qw4ny7lx4d
    @user-qw4ny7lx4d2 ай бұрын

    Modou lo rek ndam rek ndam

  • @dofouAmabousamel-cl1sk
    @dofouAmabousamel-cl1sk2 ай бұрын

    Ragal bii iow lingay beuré da dane tapha tine

  • @BayeDialloDiop-gb6ys
    @BayeDialloDiop-gb6ys2 ай бұрын

    Féne rek

  • @amicollelo68

    @amicollelo68

    Ай бұрын

    Khol bou diekh😂

  • @boubacarboiro5813
    @boubacarboiro58132 ай бұрын

    Babacar moo nèkh dé néna contact dafa nèkh kay😂😂😂😂😂

  • @moustaphambaye3393
    @moustaphambaye33932 ай бұрын

    Danga daw tapha tine lolou niepp xam nagn ko

  • @arfangsenghore3993
    @arfangsenghore39932 ай бұрын

    ❤❤

  • @MouDiop-tk5rw
    @MouDiop-tk5rw2 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤

  • @papaallefall5041
    @papaallefall50412 ай бұрын

    Ay waxu tapett rek nga fii wax daww bah nittt kii am combats ngay wax nane dafa yakamti

  • @user-pz8sd5dr2m
    @user-pz8sd5dr2m2 ай бұрын

    Modou da ragal Tapha Tine

  • @adandoye3759
    @adandoye37592 ай бұрын

    Wamais ki dou Modou dioutal lô bu Amadou Ba 5em President 😂😂😂😂😂

  • @Abdk0p

    @Abdk0p

    2 ай бұрын

    Wa Après diam ak pékhem yalla ak dogo lam

  • @ibwagnewagne6481
    @ibwagnewagne64812 ай бұрын

    Waro khaw lolou ndakh danga daw combat bi

  • @akimoulakimseck

    @akimoulakimseck

    2 ай бұрын

    Mdr khana Daw nga sante iow 🤣🤣🤣🤣

  • @djilyseye1327
    @djilyseye13272 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤

  • @user-mn7is9nh9q
    @user-mn7is9nh9q2 ай бұрын

    Pourquoi nga daw ko

  • @falybadji8954
    @falybadji89542 ай бұрын

    mo ki d'où Modou mou amadou ba

  • @elhadjwade508
    @elhadjwade5082 ай бұрын

    Modou lo mi nakaté wéroul dé ta menoul communication louy menouma wone hare ma dalou iow gua dawe 😂😂😂

  • @bariso2626

    @bariso2626

    2 ай бұрын

    Yaw mi ya geun doff gnépou nak😂😂wala danga faté ni ci 2 mois la daané niari boy yi geun méti fi Saway tapha mo amoul patience Sinon nioy beuré nga nitt nitelou nonou ya geun malade 😂😂😂

  • @PeindaFall-nx5pn

    @PeindaFall-nx5pn

    2 ай бұрын

    @@bariso2626wouy rayngama yaw 😂😂😊

  • @user-kr5oi9op3b
    @user-kr5oi9op3b2 ай бұрын

    Daga wakh liga geum baol baol yi wakh lin geum kou nek ak liga geum

  • @mamediorndiaye5852
    @mamediorndiaye58522 ай бұрын

    Abou bacar ndiaye modoulo et moustahfatin praleanfans

  • @abdoulayediallo4028
    @abdoulayediallo40282 ай бұрын

    Mdlo bou fékone blessure ama gua amone do done beré le 5 novembre

  • @user-nn7ub4rw9c
    @user-nn7ub4rw9c2 ай бұрын

    N'importe quoi modou tu as peur de tapha tine il faut osé le dire quand même

  • @dembandiaye585

    @dembandiaye585

    2 ай бұрын

    Bilaye tu as bien dis

  • @aliousarr3816
    @aliousarr38162 ай бұрын

    Bayil sa wakhou tapet yi jeul avance bi affaire bi dou wakh rek

  • @user-bn9jc1rp9q
    @user-bn9jc1rp9q2 ай бұрын

    Modou et balla jouent sur les tactik des paroles et mystik

  • @EmileLucienMoreira
    @EmileLucienMoreira2 ай бұрын

    Gueuna yomb té djeuloko😂😂 saway soudé loloula rek so paré tci siteu djeul tapha ngua wone gnu noko mané métiwoul dé😂😂

  • @metabrown3885

    @metabrown3885

    2 ай бұрын

    Fall nala Khamal darra dh li eumeu ame Si tapha bouko Modou amè wakhoumala sakh dane bilahi moy geuna niaw ke sakh niom Ama

  • @fishconjie3749

    @fishconjie3749

    2 ай бұрын

    ​@@metabrown3885 Yen ama tokh 5yr ngen kay compare ak tapha yabate bi purrr lane lah dieul len ko rk sett khep batè bi mo geuntè tah presi basss yalla dokhko galsen

  • @EmileLucienMoreira

    @EmileLucienMoreira

    2 ай бұрын

    😂😂 Wa nako dieul souko dané mou leer métiwoul dé@@metabrown3885

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    2 ай бұрын

    @@metabrown3885 Saway Eumeu dou Modou motakh Eumeu dane Balla, Lac, Bomb te Modou danou lene !!!

  • @masseseck9475
    @masseseck94752 ай бұрын

    Yaw yambar nga rek nga bayi ba heur bi ngaye wakh ni tapha mo guene nekh beurel 😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ibrahimabodian9
    @ibrahimabodian92 ай бұрын

    Mod lo com dou mbeur dafa timide té touti waaaay déy nookké😂😂😂

  • @Sonkosenegalais
    @SonkosenegalaisАй бұрын

    Bombardier mo geuneu yomb daan Tapha Tine té mounoko daan,bayiil sa khél binguay foowé modou lo😂😂😂

  • @MbengeJoee
    @MbengeJoee2 ай бұрын

    🎉❤❤

  • @layewos2073
    @layewos20732 ай бұрын

    sonko sonko sonko diomaye diomaye

  • @ZionnkaZen
    @ZionnkaZen2 ай бұрын

    BO dougué thi Tapha do thi guéne. Tapha, bombardier, Balla tu n'arriveras jamais à les faire bouger avec des ""jeux de singe"". Et souvent c dans ces genres de combats qui tu as des difficultés. Aythie reck

  • @abdoudiop7177

    @abdoudiop7177

    2 ай бұрын

    Sawaye modou ci balla rek la am problème parcque balla dafamene balla mais tapha il est limité techniquement sawaye tapha daye bokhanté rek mofi d'apporter Elton dore ko ba guisatoule ta manoko done tapha amoul sangsagne doléances kasé ka am vraiment

  • @ZionnkaZen

    @ZionnkaZen

    2 ай бұрын

    @@abdoudiop7177 Nou defonn ak Bombardier ??

  • @ZionnkaZen

    @ZionnkaZen

    2 ай бұрын

    @@abdoudiop7177 ou mm lac 2, je veux dire qu'avec les lutteurs qui ne bougent pas trop il a tjrs des difficultés. Le moment venu tu verras

  • @abdoudiop7177

    @abdoudiop7177

    2 ай бұрын

    @@ZionnkaZen leggui nioome amou difficulté pour dane modou? Nioniou balla rek moci am ay qualités niou mene dane modou yao hamngani tapha beurrdafa dess niatta beurre lafi dane dielle bou lere day bokhanté rek

  • @abdoudiop7177

    @abdoudiop7177

    2 ай бұрын

    @@ZionnkaZen sawaye nioniou doniou bougé mais amaniou audace fekouko songouko daneko comme balla menounio beurré wala pour yene forcément modou mowara def effort pour combat bi diekh pourquoi pas nioome danguene nane modou da am probleme lourds te nioome tamit manoniouko dane

  • @madiawmboup7403
    @madiawmboup74032 ай бұрын

    Dangay djiell combat bi wayè di daw tè nan mako meun😂😂😂😂

  • @modourokhaya9616
    @modourokhaya96162 ай бұрын

    Kii day kharou

  • @user-jc3ie8gr8x
    @user-jc3ie8gr8x2 ай бұрын

    Légui dafa fouyyy

  • @kurayahmi
    @kurayahmi2 ай бұрын

    *Kou xam lamb deugue xam ni lou leer lalen wakh. Style yi nio bokoul, Tapha meunoul songue, day direekou, dafa yekh, teh dey nelaw ci biir combat. Kou mel nonou ak no meunti tolou do sonal modou. Sougn done beurei dinako dan teh dou sakh comprendre*

  • @abdoudiop7177

    @abdoudiop7177

    2 ай бұрын

    Sawaye tapha il est limite techniquement lolou moy deugeu amoul sagne sagne day bokhanté rek té modou boko eupo dollé té manoko imposé beurré nokoy danné modef erreur songou fou bakhoul rek gaye hare

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    2 ай бұрын

    Mdrrr pourtant nonou la mel te bomou djapper Modou lo lamb gui djexna! Saway Modou dofoul mola geuna khamni Tapha loumouy thiouner thiouner yeup moka eup dolerrr foufff !

  • @cheikhndoye670
    @cheikhndoye6702 ай бұрын

    Modou lo nitou intere

  • @madiawmboup7403
    @madiawmboup74032 ай бұрын

    Modou lo linga wakh tegou ko fen tapha tine nekhol beurel amna dolé meun na khekh

  • @oumarsoumah9270
    @oumarsoumah92702 ай бұрын

    Yaw yaye Tapé champions cloclo naka prendre son avance svp de rester de parler 😂😂😂

  • @mbayestarsene2179

    @mbayestarsene2179

    2 ай бұрын

    Yaw esk cva dafa melni da nga am fébarou khel dh 😂 demal fanne

  • @diockeldiop5428
    @diockeldiop54282 ай бұрын

    MODOU a fuit le combat contre Tapha c’est la réalité. Gnémé wouko

  • @ibrahimadrame9499

    @ibrahimadrame9499

    2 ай бұрын

    Am léne diom nguir yalla lolou nguéne done wakh si ama modou nokhouko danko🙄🙄😳😳😳

  • @abrahamsamb6596

    @abrahamsamb6596

    2 ай бұрын

    😅😅😅😅😅😅

  • @assanesarr9992
    @assanesarr99922 ай бұрын

    Nekha faral dimanche 👑👑👑👑👑

  • @Khadimndiaye-de4pl
    @Khadimndiaye-de4pl2 ай бұрын

    Lamb n'est pas un facteur de développement c'est un deal de blanchiment d'argent

  • @BAYUBgoor484

    @BAYUBgoor484

    2 ай бұрын

    😂😂😂😂😂 de même que la boxe et le football et le rugby et tous les sports 🏈 🥊 dagnko wara bayii Ioe wérro dh grand

  • @thiamahmadulattekh562

    @thiamahmadulattekh562

    2 ай бұрын

    ​@@BAYUBgoor484lol ni key dof la sponsor yi di indi sene xaliss di am visibilite mouy wax waxi blanchiment hnom send aduna yeup dagno beug nit gni top politik ay dof lagnu

  • @user-gw8qv9zg5b
    @user-gw8qv9zg5b2 ай бұрын

    😂😂😂Modou boul niou sonal way da nga daw tapha tine 😂😂😂

  • @user-dx5bs3bq9z
    @user-dx5bs3bq9z2 ай бұрын

    Diomay moy president

  • @mlsbgambian8384
    @mlsbgambian8384Ай бұрын

    bilahi bo dieul tapha tine doto ko defati

  • @omzoseck8566
    @omzoseck85662 ай бұрын

    Ragal rék montah brewol ak Tafah Tine

  • @bayemodoudiagne2326
    @bayemodoudiagne23262 ай бұрын

    Tapha déi amoule beuré bou dane Modou lo

  • @lomethalo2154
    @lomethalo21542 ай бұрын

    Kiii dama diaxal mais suivre tapha Tine deh bou bakh

  • @DjibiThiaw-wy2xy
    @DjibiThiaw-wy2xy2 ай бұрын

    Bou beurè ak tapha tine wer ko kou yekh dou dan modou lo moko meun allez retour 😂dou combat 😂

  • @calb8865
    @calb88652 ай бұрын

    il na n a ni démonté ni humilié Tapha ; le titre est vraiment exagéré

  • @charlesba1138
    @charlesba11382 ай бұрын

    Lou lerr la wakh Tapha Tine tangoull

  • @user-hj9mj9no4g
    @user-hj9mj9no4g2 ай бұрын

    Tapha tine vs modou lo ficelé

  • @user-vr6nh4uq8x
    @user-vr6nh4uq8x2 ай бұрын

    Modou wakh na lou ame solo affaire bi nèkoule rk lou niou fa tèk kou niew rk dieule

  • @MbengeJoee
    @MbengeJoee2 ай бұрын

    👑👑👑👑👑👑👑👑

  • @babacarfaye4446
    @babacarfaye44462 ай бұрын

    Wawaw Kharagne rk

  • @Showbizsn-gz1ch
    @Showbizsn-gz1ch2 ай бұрын

    Télé bi diouboul dh dioubal lenko

  • @dembaguite4945
    @dembaguite49452 ай бұрын

    Neu bayi wakham yi bariyi temou dielko

  • @sidindir4937
    @sidindir49372 ай бұрын

    TAPHA TINE ,MODOU DALAY BEURÉLO BA NGUA BAYI MOU DANE LEUHH😅TAPHA TINE AMOUL KHAM KHAM BOUYE DANE MODOU

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    2 ай бұрын

    Koy Dane da nga kaay gnemer te Tapha mo eup doler thi lamb J

  • @user-jy9wv2is5e
    @user-jy9wv2is5e2 ай бұрын

    Kidé bou téyé tapha dakoy ray euma séne dorko bamouy beuga dé té euma manoul xékh😅

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    2 ай бұрын

    Fiit gui Eumeu am ba takhaw khekh ak mom te tegoul tank guinaw lolou guissouma Modou deff ko

  • @modoudiouf8199
    @modoudiouf81992 ай бұрын

    Sxr sama mbeur leu mais il a cherché à échapper Tapha sous prétexte d'un repos 😂

  • @mbayestarsene2179

    @mbayestarsene2179

    2 ай бұрын

    Sa mbeur la kay mei kou beuré ak bormbardier waro daww tapha mou neukh mi😂

  • @kefgg

    @kefgg

    2 ай бұрын

    ​@@mbayestarsene2179Tapha Tine mo gueuneu tangue Bombardier. Tapha Tine mofi dore Bombardier ba ambulance gneuw si stade bi.

  • @mbayestarsene2179

    @mbayestarsene2179

    2 ай бұрын

    Am nga si droit dh mei yaw so waité kham nga ni modou lo mo moune tapha hahaa lolou rek moma si nekh

  • @mamecorecisse1849

    @mamecorecisse1849

    Ай бұрын

    ​@@mbayestarsene2179Modou lo guissoul ragal faléwoul sakh tafa tine

  • @boubaleye2003
    @boubaleye20032 ай бұрын

    Da beugu baye bah diekou tapha tine sokeu dieul😂 tek khel la

Келесі