Douma Moromou Franc ….Réponse de Sathies après sa défaite sur eumeu séne .balla Motakhma

ABONNEZ-VOUS ET ACTIVE LA CLOCHE DE NOTIFICATION
____________________________________________________________
RÉALISATION : Thioker Tv
MONTAGE : Thioker Tv
PRODUCTION : Thioker Production
CONTACT EMAIL : maissaelprezii@gmail.com
____________________________________________________________
Vidéo non Sponsorisé
Aucun Placement de Produits
Copyright ©️ 2024 Thioker TV
Tous Droits Réservés
____________________________________________________________
Plus d'infos sur Thioker Tv
Pour toutes réclamations ou Autre....
veuillez appeler au 77 1867700 ou WhatsApp 📞
____________________________________________________________
REJOIGNEZ MOI SUR LES RÉSEAUX SOCIAUX

Пікірлер: 200

  • @malickndiaye3436
    @malickndiaye3436Ай бұрын

    Sa Thies respecte nous wayy. Ce n’est plus le moment où tu peux nous faire croire que do moromou Franc. Là là souko nékhei sakh mouni dou beuré ak Yaw Eumeu lay beurél parce que Bombardier moleine bolé

  • @swartnwar916

    @swartnwar916

    Ай бұрын

    😂bane bombardier moléne bolei? je veux dire quelle version de Bombardier ?? Quand Franc disait que dou moromou Quench ay fansam dagnko.ko nangoulone pourtant Franc n’avait rien de plus que Quench mais c’était son droit le plus absolu. Maintenant quand un Sathies dit que dou morom Franc ngen beugko.ko banial. Une chose est sûre SaThiés a tellement croisé le fer meussoul taneu un chemin facile lolou motakh malgré sa défaite tay sougn néwone Sathiés-Tapha Tine sakh les gens ne seront pas surpris souko nékhone bim dané lac rose, dieul béneu Pa bouy wadia dem retraite comme niko certains defei tanyé, daneko commencei lathié ay magam, ça lui aurait permis de raccourcir son chemin vers le sommet comme garyi nignko beug défé.

  • @modourokhaya9616

    @modourokhaya9616

    Ай бұрын

    Franc eumeu wala sathies dou logique. Franc defoufi Lou beuri

  • @ahmadoudiop5016

    @ahmadoudiop5016

    Ай бұрын

    ​@@swartnwar916loulerr ngua wakh

  • @AbdrahmaneSy-jr1bb

    @AbdrahmaneSy-jr1bb

    Ай бұрын

    Wakh deug fa YALLAH boy bi mongui moudjé beuri

  • @user-tz2ip1fm8y

    @user-tz2ip1fm8y

    Ай бұрын

    Bombardier 3 ème âge la

  • @FallouLeye-gs3xt
    @FallouLeye-gs3xtАй бұрын

    sa thies dangay nék roi dh inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Mohaaa2.0
    @Mohaaa2.0Ай бұрын

    Franc boko dieulé dou bax si uoe dina méti dina khéré Niagobi doff leuh comme genrou pokolaaaa té dafa am dolé en plus professionnel leuh guinaw bou bax leu am diamono djii 💪🏿 Dofoléne sakh kham ngéne lépeuh😂😂

  • @user-cc1ie1ve9r
    @user-cc1ie1ve9rАй бұрын

    Eumeu franc❤

  • @nomisdogue618
    @nomisdogue618Ай бұрын

    Sa thies denga beugue ngou diokhla franc rek mais franc mola raw thi lamb leugii doula diel eumeu walla balla rek

  • @swartnwar916

    @swartnwar916

    Ай бұрын

    😂😂😂sama garyi nak yene khoromou nguéne dh 😅😅 Ko khamni lim am ci victoire amoko ci combat ngani yako raw. Top3 adversaires Sathiés nio raw Franc, Top3 adversaires Franc diégué wougn sakh Sathiés. Reug Reug mi ngu khamni dafeu dane Franc, dane Franc, dane Franc beu Naarbi sou nékône ci lamb khamna Reug-Reug Franc sou takhawône so moytoul cote 0,000001 leu Reug dih am, demone nagn beu Reug Reug dane Franc nékatoulwone probabilité mais une certitude, Reug momou leu SaThies nieuw douma daane. Tous ceci réuni vous dites que Franc mo Raw Sathies😂 décidément vous avez une sacrée définition du mot ‘’raw’’.

  • @nomisdogue618

    @nomisdogue618

    Ай бұрын

    @@swartnwar916 franc mo d'âne bombardier mi sa Thiès ragalone diel te mousoul danou combat Yep defka d'âne am 13victoire sa Thiès am 14ak 3 defete fanlay diar ba douko raw

  • @danielcorreia2073
    @danielcorreia2073Ай бұрын

    Yow fran sokhlawoula, danga echec txi Malick niang ak boy niang et maintenant eumeu sene, biss bou la fran diapé di nga kham lep deugeuleu

  • @user-uq4gb3br4o
    @user-uq4gb3br4oАй бұрын

    Franc mola raw sawadji 😂😂

  • @amethiombane7278

    @amethiombane7278

    Ай бұрын

    Si naka nonou

  • @diazblofficiel8087

    @diazblofficiel8087

    Ай бұрын

    Wa iow miiii koula bayi😂

  • @truckwarriors9832
    @truckwarriors9832Ай бұрын

    So dieuler franc danou😂satinées bayil dof dof loubi 😂

  • @FraFra-bq2fb
    @FraFra-bq2fbАй бұрын

    Yalla rekkk mo khammmm louy khewww soubaaa

  • @Papesarr-wv3me
    @Papesarr-wv3meАй бұрын

    sa khool bou rafétt la yor nak koi bilahi ❤❤

  • @Serignemeumeu
    @SerignemeumeuАй бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤ Saa tt nos encouragements et nos félicitations à eum Bien parlé saa thies❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469Ай бұрын

    Franc mola mene bilay bosi dougué am loula béte😂😂😂😂😂frans mola mane 10fois doté nékhouma 😂

  • @ousmanegomis6938
    @ousmanegomis6938Ай бұрын

    Sa way iow oubal sa lamigne 👅 Ndiago bi mola meune fouf

  • @sebastienaccatcha4298
    @sebastienaccatcha4298Ай бұрын

    Sa Thiés khamo doul mbeur bou euppeul nga boy, Franc mo doul sa morom. khamo dara, wa guediawaye beuri wakh nguène deff

  • @user-Fallouniasse
    @user-FallouniasseАй бұрын

    So dieulee Franc danou😂💪

  • @manegueye2896
    @manegueye2896Ай бұрын

    Sa mano bagne franc dh

  • @ycamara9034

    @ycamara9034

    Ай бұрын

    Is ok ,next time you will win now take Gris ,👍👍👍👍👍👍💪✌️🌍🙏

  • @user-uj7ze9dm7i
    @user-uj7ze9dm7iАй бұрын

    Sa waye frac Mona toko bang

  • @nomisdogue618

    @nomisdogue618

    Ай бұрын

    Franc moko raw legui sakh

  • @RioNdiaye

    @RioNdiaye

    Ай бұрын

    Maye gnou diam way franc kanne la danne ba wara beuré ak sa thies

  • @CaramocoDiallo

    @CaramocoDiallo

    Ай бұрын

    ​@@nomisdogue618dane bombardier bou âme 50 ans loolou d'où performance

  • @user-uj7ze9dm7i

    @user-uj7ze9dm7i

    Ай бұрын

    @@RioNdiaye yaw la dan

  • @ycamara9034
    @ycamara9034Ай бұрын

    May the yunas bless you and yo brother and yo whole family Amen 🙏🙏🙏👍🌍💪🌍🙏👍

  • @malicktoure6343
    @malicktoure6343Ай бұрын

    Saway nak franc mom waxal ni begue gua lenen rek mais do moromam dou wax

  • @IbrahimaDiabong-sx3fu
    @IbrahimaDiabong-sx3fuАй бұрын

    Du courage 💪

  • @abdoukarimditmacodoundiaye993
    @abdoukarimditmacodoundiaye993Ай бұрын

    Sa Thies Mane damala beugue mé respect franc c’est un vrai champion

  • @abdoukhoudossfall995
    @abdoukhoudossfall995Ай бұрын

    Franc ko raw sakh nak

  • @modouabdouabdoukhadimmbeng6405

    @modouabdouabdoukhadimmbeng6405

    Ай бұрын

    Www

  • @swartnwar916

    @swartnwar916

    Ай бұрын

    😂😂😂sama garyi nak yene khoromou nguéne dh 😅😅 Ko khamni lim am ci victoire amoko ci combat ngani yako raw. Top3 adversaires Sathiés nio raw Franc (BNiang, Eumeu, Reug Reug la terreur), Top3 adversaires Franc diégué wougn sakh Sathiés. Reug Reug mi ngu khamni dafeu dane Franc, dane Franc, dane Franc beu Naarbi sou nékône ci lamb khamna Reug-Reug Franc sou takhawône so moytoul cote 0,000001 leu Reug dih am, demone nagn beu Reug Reug dane Franc nékatoulwone probabilité mais une certitude, Reug momou leu SaThies nieuw douma daane. Tous ceci réuni vous dites que Franc mo Raw Sathies😂 décidément vous avez une sacrée définition du mot ‘’raw’’.

  • @king_family_officielle7816
    @king_family_officielle7816Ай бұрын

    Amine

  • @KarimoulahMbaye-kt1fo
    @KarimoulahMbaye-kt1foАй бұрын

    Niagobi kouko dieuloul dagko ragale 😂

  • @abdougueye8129

    @abdougueye8129

    Ай бұрын

    Mom mi daw quench ak serigne ndiaye nak

  • @KarimoulahMbaye-kt1fo

    @KarimoulahMbaye-kt1fo

    Ай бұрын

    @@abdougueye8129 Dawoulénedé kouy guiss bombe di dieul boy yoyou

  • @thiamahmadulattekh562

    @thiamahmadulattekh562

    Ай бұрын

    @@abdougueye8129ba gueine tambalei setane lamb yagoul Serigne ndiaye franc dane na ko ay yoni yoni lutte simple Dane ko arene ba nopi Lumi deilou diko djeulate?

  • @user-nn5ge6gk5g
    @user-nn5ge6gk5gАй бұрын

    Senegal légui lambou dji nekhena am défaite niouni daguay wathi sa thies dafa mbeuré ak morom iop ki dou ragal mais nk lambou day tolou fo khamni carrière guay def dou aferou ragal wala nuamé sa thies tolou woul foumouye ragalé mbeur ki goor yalla deugue leu ❤❤❤

  • @modoundiaye2368
    @modoundiaye2368Ай бұрын

    Du courage

  • @abdourahmanesindidi1818
    @abdourahmanesindidi1818Ай бұрын

    Une bonne communication

  • @malaadothiam772
    @malaadothiam772Ай бұрын

    Sa thies waxou tapète rek ngafi wakh franc mola meune fouf motax ngay moytou

  • @AdolpheGomis

    @AdolpheGomis

    Ай бұрын

    Dafa lér franc dou thi cachée dou thi palmarès dou thi meuna beuré franc lamb ji dé coumoytoul franc rouss rék

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rjАй бұрын

    Diamono dji fran si boppam mola geuneu bagne boula diappé dalay lekk ndayame 😂😂😂😂

  • @user-gm9xr1zd1f

    @user-gm9xr1zd1f

    Ай бұрын

    Franc ko mane

  • @AdolpheGomis

    @AdolpheGomis

    Ай бұрын

    Fouffff

  • @SalamBouhtdkh
    @SalamBouhtdkhАй бұрын

    Sathies sop na la lol ndakh respect binga diokh eumeu mais nak insbi mom franc sakh mo wara bagne pour heure ak yaw khana

  • @user-kv1ee9gw9l

    @user-kv1ee9gw9l

    Ай бұрын

    Vraiment 😂😂😂

  • @ndakarudialdiop1206

    @ndakarudialdiop1206

    Ай бұрын

    Yénn da ngén di fowé sén khél yi la yakar😂franc bombardier troisi age la dane😂

  • @khadimdiaw9211
    @khadimdiaw9211Ай бұрын

    Sa Thiès dfa nekh iow eumeu séne douma la dan la gay wakha fii franc mola meun Alès retour

  • @alysow6354

    @alysow6354

    Ай бұрын

    Khamo lamb

  • @Menoo107

    @Menoo107

    Ай бұрын

    Mais yw wer gua

  • @birahimseck9167

    @birahimseck9167

    Ай бұрын

    @@alysow6354iow y’a xamoule lamb franc sax vraiment eumeu sene la wara beuréle mais pas sathies daffa danou di

  • @DiabaCiss-ck8cs

    @DiabaCiss-ck8cs

    Ай бұрын

    Yow wakhou far ngafii wakh nite daye wakh deug

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    Ай бұрын

    Meunolene teukaler ndax Eumeu Sene mo meun kou meune Franc

  • @yvonnebadiane2702
    @yvonnebadiane2702Ай бұрын

    Bilahi franc molaa meune foufffff

  • @ibrahimadiattara2738
    @ibrahimadiattara2738Ай бұрын

    Franc kay insbi mo raw sathies

  • @francoisfaye9661
    @francoisfaye9661Ай бұрын

    Sathies à peur d avoir 2 defaites successives il gère sa carrière

  • @AdolpheGomis

    @AdolpheGomis

    Ай бұрын

    Je te jure que franc mo meune foufe franc dou sakh morome qui ragal franc la déff

  • @SerigneDieng-ub5ux
    @SerigneDieng-ub5uxАй бұрын

    vraiment lou lerr ga wakh nk sa diamou thi yawn🫵🏻🫵🏻

  • @issamballo3734
    @issamballo3734Ай бұрын

    Sa thies mouno bagne franc nak siteu nga diouger

  • @abdoutoure2490
    @abdoutoure2490Ай бұрын

    Franc. La man mem.balla franc. Ko. Man

  • @bachirdiop19
    @bachirdiop19Ай бұрын

    Sathies je t’estime bcq do sama mbeur nak mais insbi mano bagne Franc vraiment

  • @papendeuryseck6854
    @papendeuryseck6854Ай бұрын

    Wakh deug yalla sa nek roi guissou mako parce que sa mane beuré dafa desssssss trop sakh

  • @doorwaar9465
    @doorwaar9465Ай бұрын

    Franc nekhiul berel deh sa dofoul deh,😂😂

  • @loaboubacar3595
    @loaboubacar3595Ай бұрын

    Yen yena tax gri , ameu , dougn mosa wathi....dagena wara beure sen bir

  • @MansourDiop-yc7nl
    @MansourDiop-yc7nlАй бұрын

    Sa Thiès danko ragal défo Lou mou défoul ragal ga bilahi

  • @user-kv1ee9gw9l
    @user-kv1ee9gw9lАй бұрын

    Hahaha néna da raww franc niii sathie mon nékh😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141Ай бұрын

    Boula franc banigout waroko bange 🤷🏽‍♂️😂😅😂😁dangaye ragale tegalé 2 défet rek ndiogobi kasse 😂👑

  • @mansourseye7576
    @mansourseye7576Ай бұрын

    Sa thies franchement tu ne peut pas refuser franc

  • @papendeuryseck6854
    @papendeuryseck6854Ай бұрын

    Sa thies franc soka dieuloul dinala fi bayi dé soudone may yaw nga dieulko légui

  • @bncdakolstreet5271
    @bncdakolstreet5271Ай бұрын

    Demal beure ak frank mo gueune😂😂

  • @IbrahimNdiaye-ln8it
    @IbrahimNdiaye-ln8itАй бұрын

    Je comprends pas, c'est quoi le problème avec Franc

  • @AdolpheGomis

    @AdolpheGomis

    Ай бұрын

    Bilaye franc le panthère noir

  • @modoubamachalla7818
    @modoubamachalla7818Ай бұрын

    Bilay daga bang danou wate rek

  • @user-gm9xr1zd1f

    @user-gm9xr1zd1f

    Ай бұрын

    Késsé nak

  • @babacar3178
    @babacar3178Ай бұрын

    Sa thiés mon nékh

  • @FraFra-bq2fb
    @FraFra-bq2fbАй бұрын

    Sa thies Vs fran comba la fran reug reug dan nako lou barri sa thies mo dan reug connn sa thies Vs fran moyyy comba bii ????

  • @danielcorreia2073

    @danielcorreia2073

    Ай бұрын

    Fan la Reug dané fran mbapat? Saway boulniuosonal, sou feke danga dan nitki mbapat motah dolén beure arene lamb dotoul amati

  • @MilkMilo-qr5uc

    @MilkMilo-qr5uc

    Ай бұрын

    ​@@danielcorreia2073faté léne bobou victoire sa thies reug reug dou moromam

  • @mormbaye6098
    @mormbaye6098Ай бұрын

    bilahi frére franc waroule dieul kou doule eumeu yaw fi mou tollou ni amoulo loy taamou

  • @mamepathe4618
    @mamepathe4618Ай бұрын

    Franc amoul défaite yaw défaite kéccé nga François sa baye la

  • @user-qv7pl8lw4f
    @user-qv7pl8lw4fАй бұрын

    Fran est le meilleur lutteur de l'année kouko dieuloule tapète gua🎉franc seul

  • @andregomis-wc5dj
    @andregomis-wc5djАй бұрын

    Sa thiés mouno bagne Franc

  • @fsportif
    @fsportifАй бұрын

    Yaw esk çava chez toi ? Franc dépassé naleu insbi kholoula sakh 😂😂😂

  • @user-kw8bk2zf6n

    @user-kw8bk2zf6n

    Ай бұрын

    C'est pas vrai

  • @senegal559
    @senegal559Ай бұрын

    Eumue Séné dousa morom té da la diuel wakho fi dara ragal ga déf farac

  • @mbayendiaye4562
    @mbayendiaye4562Ай бұрын

    Sa thies srx waye franc raw nala

  • @krkr7182
    @krkr7182Ай бұрын

    Sa Thiès combat bou yomb sans pression la beugg. Franc la gaa yi beugg, boul daw

  • @TaherElouardi
    @TaherElouardiАй бұрын

    Tapet nga rek franc sa Pape la

  • @FraFra-bq2fb
    @FraFra-bq2fbАй бұрын

    Waaa Senegal 🇸🇳 damay ragalll siteu dann modou lo ..... douma serigne deee dama analige rekkk

  • @ababacarsadikh4097
    @ababacarsadikh4097Ай бұрын

    Sawayyy iow khamngueniii sakh franc mola meune 😂😂😂

  • @MansourDiop-yc7nl
    @MansourDiop-yc7nlАй бұрын

    Fékhéle ba bou dieul bombardier kom do moromou fran

  • @BAYUBgoor484
    @BAYUBgoor484Ай бұрын

    Franc dh 0 défaite leu am Mo guen palmarès si lamb dji Té kou dane bombardier doug nga cours des grands par force 😂 Mais kokou boyayo ngéne complot ko sinon dineu lèn dièkhale

  • @boydiack2724
    @boydiack2724Ай бұрын

    Non sa Thiès daga wathie nag

  • @tarkindabi4168
    @tarkindabi4168Ай бұрын

    Franc mola sokhla woula😂 nguay tekk khel nii

  • @alysow6354
    @alysow6354Ай бұрын

    Yenne da ngena doff franc bombardier bimou danne day bombardier bou takh niouy wakh franc vs alioune seye 2

  • @danielcorreia2073

    @danielcorreia2073

    Ай бұрын

    Fran dan alioune sey yobouwouko fen

  • @abdousalamlo2942
    @abdousalamlo2942Ай бұрын

    Wakh ga deug dh diouguè ci defaite khalatoo diel franc di tèglè defaite

  • @CaramocoDiallo
    @CaramocoDialloАй бұрын

    Franc Aline seye 2 moy yone Sathies gris bordeaux Amanekh zarco

  • @user-wi5ol7zu4b

    @user-wi5ol7zu4b

    Ай бұрын

    Aliou séye na djeuli petit lo

  • @mbenguecheikh6272
    @mbenguecheikh6272Ай бұрын

    Sa da rew

  • @AliouDiouf-ci2ny
    @AliouDiouf-ci2nyАй бұрын

    Sa Thies Yaw Nékal Nitt Franc Mala men Dagua Dano Franc Dan Soko Delé kham gua Lila siy Fégue Dano rek Tay mom vremen wakho fi dara

  • @PapeFaye-vg9ym
    @PapeFaye-vg9ymАй бұрын

    Palmarès franc thiatou yof Bébé Saloum Serigne Ndiaye Tyson 2 Sokh Forza Bombardier Ndiago bi nékhoul affaire dé

  • @khadimdeme-cy9mk
    @khadimdeme-cy9mkАй бұрын

    Sa thies a parfaitement raison moy day niann chance aye grand wam kon n'a bay ba tollou fim wara mayé chance mu mayéko sa thies axe franc lumu yageu yageu dinaniou dadié vip suniou fii diouguè niom nio fii dèss téh su booba fawu niou lalé

  • @salioundoye2349
    @salioundoye2349Ай бұрын

    Franc ya ko raww s LAMB franc ak Alioune seye moy combat

  • @Goodjob7925
    @Goodjob7925Ай бұрын

    Faranc mola man allez retour 😂😂😂😂😂 ndiago bi da bari doole de😂😂😂😂😂

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469Ай бұрын

    Daga ésék si eum séne

  • @MansourDiop-yc7nl
    @MansourDiop-yc7nlАй бұрын

    Wahki ragal ga wakh

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469Ай бұрын

    Tapha tine aiye yéré la ték lé😂😂😂😂ték si amoul vivacité d'esprit gnémé woulee Balla

  • @KhadimYade-lg7hb
    @KhadimYade-lg7hbАй бұрын

    Je suis désolé sa thies tu n’as aucun raison de refuser à lutter avec franc si c’est niveau palmarès et performance franc est devant toi.

  • @BayezallDiop-gr2oy
    @BayezallDiop-gr2oyАй бұрын

    😂yeen njiy farans mo raw sa thèse yena mana ndayi 😂😂

  • @nitoudeugue4930
    @nitoudeugue4930Ай бұрын

    Iow amo looy bagne diamono dji Xamal sa bopou bala niou la key wakh

  • @assanediop771
    @assanediop771Ай бұрын

    Balla gaye2 moy sama mais ndourouwoul balla si fit danga tardè dano boye niang dano eumeu franc mola wara bagne

  • @papadiom9260

    @papadiom9260

    Ай бұрын

    Franc mom koufi dane ??

  • @user-iq7vs2ci4h
    @user-iq7vs2ci4hАй бұрын

    Franc mome dalay nex ga mayko chance beuri nafi ay moromame yumu wara beurel

  • @boubacarndao3382
    @boubacarndao3382Ай бұрын

    Héé sa thies arrêt ni ngay mbeuré bo changé woul mouno dane Fran haa vraiment mbeurou béna clé dou mbeur déh

  • @Aladjil609
    @Aladjil609Ай бұрын

    Goudy yi franc molla mane niguaye beuré dafa arrangé franc

  • @alysow6354
    @alysow6354Ай бұрын

    Sathies dane ness dane siteu dane reug reug dane lac rose dane moussa ndoye dane Jordan dane zarko franc bane palmares la def pa bombardier

  • @AliouneDia-ty2kl

    @AliouneDia-ty2kl

    Ай бұрын

    Excellente question

  • @khadimdeme-cy9mk

    @khadimdeme-cy9mk

    Ай бұрын

    Lu lerr gua wah

  • @MilkMilo-qr5uc

    @MilkMilo-qr5uc

    Ай бұрын

    Gniga lim kousi si béne takussan franc dane léne

  • @KarimoulahMbaye-kt1fo
    @KarimoulahMbaye-kt1foАй бұрын

    Iow boula faran bagnoul waroko bagne🤭

  • @Menoo107

    @Menoo107

    Ай бұрын

    Yaw dh khamo lambe demale guestou lambe wakhou supporter guay wakh ni

  • @KarimoulahMbaye-kt1fo

    @KarimoulahMbaye-kt1fo

    Ай бұрын

    @@Menoo107 wla iow ya xamoul lamb sw ki bako euma dané la wayadi

  • @boubacarfaye3209
    @boubacarfaye3209Ай бұрын

    Sama mbeur ga mais mouno bagne franc ndah dega danou

  • @ndondolinfostv7735
    @ndondolinfostv7735Ай бұрын

    Ragal Emil François Gomis dong mom nga df😂 boko diélé mou dane la ta kon sa lamb guëneu compliqué

  • @MagouThiaw-zb8cu
    @MagouThiaw-zb8cuАй бұрын

    Sa nawnaladh ndax sawax

  • @bayeniasse5604
    @bayeniasse5604Ай бұрын

    Franc sathies combat là

  • @leuz.patriote
    @leuz.patrioteАй бұрын

    Sa thies diot na vip beure ak mom eumeu sene grand champion dane bg2 gris lac 2 kon sou dané sa thies douko wagni dara . Sa thies gris bordeaux ou revanche boy niang

  • @Bigboss-hd8fx
    @Bigboss-hd8fxАй бұрын

    Ya yeuy bagne dé actuellement franc ak reug reug gnolen di def linguene done def gnenene gni. Champion lo guiss dey diekh et pourtant yow modou lo nga soxela pour ame soukeur mais franc bindou reug reug la yor , t yow reug dafla dane ba tokk sa kaw

  • @tallafall7629
    @tallafall7629Ай бұрын

    Naga fégé ba boula fi faran bayyé boul niou sonal ak wakh diou bari rék 😂😂😂

  • @salioukebe4909
    @salioukebe4909Ай бұрын

    Décourage

  • @momodoujalllow
    @momodoujalllowАй бұрын

    Sa thies rk❤❤❤❤❤

  • @TijTij85
    @TijTij85Ай бұрын

    Mouni ???? 😂😂😂😂😂

  • @mababasylla9823
    @mababasylla9823Ай бұрын

    Sa thiess respectel fans balla gaye yi gnak nga foula trop eumeu 1999 la danone ouza sow nga nk khale bou ndaw si thiakhné sa lamb

  • @moussaseck7089
    @moussaseck7089Ай бұрын

    Sa Thies mo dan reug reug ❤boulein fatei lolou😂😂...franc deimal dan reug reug ba parei 😂

  • @abdoukhoudossfall995

    @abdoukhoudossfall995

    Ай бұрын

    Reug reug day dans franc rek naneko dane nala mbapat 😂 nako daneu mbapatt 200 fois takhoul Mou meun ko aréne bi dou yoyou konou dh franc mome ins bi kouko dieuloul rek danga bagna danou

  • @niokobokk3242
    @niokobokk3242Ай бұрын

    Sa thièse et giri Franc et eumeu sene bombardier aliou seye 2

Келесі