Vraie histoire sur le divorce Mario Mbaye et Ndakhté racontée par Ahmed Cissé - Virginité, lesbienne

Пікірлер: 142

  • @user-pi3gx2rq4x
    @user-pi3gx2rq4xАй бұрын

    Ndakhte yalnaka sounou borom dolli soutoura

  • @user-fy1fg6lf3h

    @user-fy1fg6lf3h

    Ай бұрын

    Aminn

  • @ndeyesokhnadiagne6099
    @ndeyesokhnadiagne6099Ай бұрын

    Pour guem li Ahmeth cisse wakh rek dem Len khol video prank bi wakhouma saga yi dh Mais plus tôt bimou wakh Mario tédou iow khamgua ma iow ce qui veux dire que mom ragaloul Mario , en plus ko passél des années ce qui veut dire que khamantè guen

  • @user-hj8pm4hu8z

    @user-hj8pm4hu8z

    Ай бұрын

    Bilakhi lagualu ko yow ndéké wakh dji dégue lu gue ko

  • @boussobaly-vo3nq
    @boussobaly-vo3nqАй бұрын

    Djigene bou glow up ❤❤❤maye ma cœur glow up da hew pas de stress pour un homme vive ndaheter vive les filles glow up

  • @aminatagueye4746

    @aminatagueye4746

    Ай бұрын

    Bilay goorr d'où projet d'où avenir

  • @dyanandiaye7584
    @dyanandiaye7584Ай бұрын

    Analyse très pertinente de cheikh Ahmed mario irresponsable la comment peux tu laisser ta femme chez toi ngay windélou si soiree yi dafa gnémé beut torop t Amna gnouko eupelé t defougnouko yoro tousss ba paré meuneu aral keine wakhouko Deug franchement investi avec tes peu de moyens waykat yi seine intérêt lagnou fi néké deh bakhna Yawite ndakhté ak noumou meunti démé warone nga kharr bassi kanam nga dok di gueiné clip parce que momit sagal nala founé fayal la diagueu et tout Yako wakh nga ni pateuu yak say mbokou Khaliss dokhoul diam déjà c est la verité 😢😢😢 maintenant on va se poser la question à qui la faute ??? Mario malgré ses délit ne l’as tu pas utilisé comme ♟️ pour arriver à tes fins

  • @aidagueye121
    @aidagueye121Ай бұрын

    Ndakhte yalna nala yalla doli soutoura

  • @fatyndiaye5328

    @fatyndiaye5328

    Ай бұрын

    Amine

  • @ndeyefatoundaw7413
    @ndeyefatoundaw7413Ай бұрын

    Ndakhte djiguene leuh nitt leuh day dioum am na defaut aussi il faut savoir que mom beuguoul entrer si ay détails et c’est très normal elle a vécu de violence, ce qui n’était pas normal may leen ko diam Limou wakh si confession lolou la wakh si way bi je vois pas le bad buzz

  • @NdiayeFatou-hs3dp

    @NdiayeFatou-hs3dp

    Ай бұрын

    Vraiment nak vie wam rek la raconter

  • @yasminaba9020
    @yasminaba9020Ай бұрын

    Mani prank mo méll nonou guiss nagne fii binette ak moussa bimoukoy saaga parce que daffa merr et pourtant niougui seuy ba légui mais kii c'est différent nak

  • @ndeyefatoundiaye3909

    @ndeyefatoundiaye3909

    Ай бұрын

    Ki c différent de binette d binette seuykatt la firr moy blm bi mai ki dafa khawa doywarr

  • @borommamouwaliwouyi3433

    @borommamouwaliwouyi3433

    24 күн бұрын

    @@ndeyefatoundiaye3909loka khamal ?

  • @marietoudiopdiop2696
    @marietoudiopdiop2696Ай бұрын

    MANDÉ LIMMA YÈMM MOODI PROBLÈME PRIVÉYII NIOUY EXPOSÉ CI RÉSAUYI YANE SOLUTIONS MOI SIYY AMM??? LÈRRAL LÈNMA NGUIR YALLA😢😢

  • @batorfall9794
    @batorfall9794Ай бұрын

    Moi je vous adore vraiment beaucoup car vous êtes véridique diam si yiow 🙏

  • @dawalid274
    @dawalid274Ай бұрын

    Vérité rek Nga wakh

  • @amadoudiop9950
    @amadoudiop9950Ай бұрын

    Mane dè ndakhtè la andal mai c est vrai daffa tangue nimouy wakhè

  • @larosierer781
    @larosierer781Ай бұрын

    Bilaye,ya wakh deugue, pure verite,cheikh Cisse

  • @ndyebinta-qz2xe
    @ndyebinta-qz2xeАй бұрын

    Guisgua ki day ndokh si khélou sénégalais yii kou djiagué 12 école louy sikame négnou khol lolou ki keur gou nék dekeu nafaa

  • @ibrahimasylla9486
    @ibrahimasylla9486Ай бұрын

    yalna yall fayla cheikh cissé toujours pertinent ce gars là

  • @ndyebinta-qz2xe
    @ndyebinta-qz2xeАй бұрын

    Amet sétane nako sillaa wakh ki dafa réw ☝️loutakh ay famille yam néko mogui dém mogui gnewateu 👇 mo wakh 12 école la djiagué mesoumako guiss sama adouna ☝️ki kouko toop bayi adounaa 🤷

  • @221tvtv4

    @221tvtv4

    Ай бұрын

    Lolou d'où si dra Mane deff n'a 10 école ,car dama beugone diangue té pabi d'âne KO done affecté dans des localités différents

  • @MoustaphaDiaban
    @MoustaphaDiabanАй бұрын

    Très bien dît

  • @user-uz1bu3wt8w
    @user-uz1bu3wt8wАй бұрын

    Kép kouy dor djigén, yalna nga dée balla tabaski

  • @dieynabafall32

    @dieynabafall32

    Ай бұрын

    Amine

  • @user-im6wk6zs4s

    @user-im6wk6zs4s

    Ай бұрын

    Amine touff touff😂

  • @MameboussoDiop-rn8ph
    @MameboussoDiop-rn8phАй бұрын

    Ndankhté da fayou kom keu dieukeum day takhalou lék lolu bakhna

  • @yasminadiop982

    @yasminadiop982

    Ай бұрын

    Boule wakhe lolou chérie taxawalou mome boudé deugue leuh waroule djiguene woroule sakhe goor mais beneu djiguene warouko defe si xelame

  • @Adelina198
    @Adelina198Ай бұрын

    Tú as parfaitement raison.

  • @HawaGako
    @HawaGakoАй бұрын

    Bonjour je ne suis pas d'accord ce monsieur n'est pas garmi un garmi avec son âge n'insulte pas en public parce que tout le monde peut écouter désolée

  • @fatoubintousarrsarr6081

    @fatoubintousarrsarr6081

    Ай бұрын

    Désolée mais on parle pas de ce monsieur comme tu dis

  • @sokhoulovedieng1365
    @sokhoulovedieng1365Ай бұрын

    Mane dei ak Lou meunti âme la wakh ndakhté limou wakh gueum nako bou bakh

  • @fatoundiaye6412

    @fatoundiaye6412

    Ай бұрын

    Ak mane guissouma bane interet la ame di tok si tele bi di inventé

  • @ironahide5896
    @ironahide5896Ай бұрын

    Lolou dé la wakh niou beug ma dor si deuk bi. J'ai tout de suite dit que ki systeme Mia lay def. Meno nieuw netali traumatisme apred nane la suite si sama clip lakoy agalé. Lolou moy tu cherches des vues. Senegalais dafa émotif motakh mou nekha nakh. Mane soumay deglou nit lo dioy dioy je garde mon esprit critique

  • @famasalihathioubsaliha9201

    @famasalihathioubsaliha9201

    Ай бұрын

    Même mane depuis le début je ne l’ai jamais cru je me suis dit que elle mentait

  • @ndyebinta-qz2xe

    @ndyebinta-qz2xe

    Ай бұрын

    Billahi degue nékhoule Ki Son wame bi ladone djiay Ndioy nasi mais bama sétané PRANK guis nimouy Dokhalé La wakh ki Dafa réw

  • @ndyebinta-qz2xe

    @ndyebinta-qz2xe

    Ай бұрын

    ​@@famasalihathioubsaliha9201fama ki Son wam bi ladone woutakeu beuz amenako gnata vue lasi ame te lolou khalis laaa 🤷

  • @nimzathniang5961

    @nimzathniang5961

    Ай бұрын

    Yaw dh wakhou degue mario si bopam mo def pas dakhté

  • @ndeyemariemendiaye8810

    @ndeyemariemendiaye8810

    Ай бұрын

    Konn dei nio yammm sénégalais mo beurri sentiment tekssi amoul khel dou peser pour kham dou deug fêter

  • @user-lx1go5pg2u
    @user-lx1go5pg2uАй бұрын

    ahmet cisse khana amooo ligueyyy ya niak faydaaaa

  • @rokhayafaye9385

    @rokhayafaye9385

    Ай бұрын

    Khana adamo lay topando si cas yi

  • @unebatante7716
    @unebatante7716Ай бұрын

    Ndakhte yalla nala yalla diapale takhawou la ❤ bonne continuation

  • @user-im6wk6zs4s

    @user-im6wk6zs4s

    Ай бұрын

    Beuss lénn traduction 😂

  • @PendaSow-he7eq
    @PendaSow-he7eqАй бұрын

    thank you so much bro I'm so proud of you

  • @ndeyembodj4683
    @ndeyembodj4683Ай бұрын

    Wakh bou dofé nopou yakoye dégue wara wér khawma lou mana khéw mé nakhté dafa djoum khawma kouko wakhlo nopi gua ba heure bi manone gua continé nonou

  • @mordiaw3811
    @mordiaw3811Ай бұрын

    Machallah cheikh bi.tu communiques trop bien

  • @user-iu1ij9xo6e
    @user-iu1ij9xo6eАй бұрын

    Bilahi réthiou wouma limalay suivre yalla na yalla deff diam bagniou délou wat inchaalah ❤❤

  • @salimatandiaye2544
    @salimatandiaye2544Ай бұрын

    Clip apres confession nonoula warone demé

  • @sidimohamedaminegueye4869

    @sidimohamedaminegueye4869

    Ай бұрын

    Un crime n'est jamais parfait... Il faut mou am ay failles

  • @diagneamsatou3473

    @diagneamsatou3473

    Ай бұрын

    Waw surtout lolou da dioum😂

  • @DashouD

    @DashouD

    Ай бұрын

    Bilay le gars kay criminel la dakadone ray deh🤭

  • @lovelydija4586

    @lovelydija4586

    Ай бұрын

    Merci Nio bok khalatt pb de timing lá clip bi mo warone djitou

  • @madamedieye6073

    @madamedieye6073

    Ай бұрын

    Sama goro lolou la wakh

  • @Bb-ng1jj
    @Bb-ng1jjАй бұрын

    Bravo 👏

  • @maamouyaayam8772
    @maamouyaayam8772Ай бұрын

    À tout moment dioubo meune na am… mandou rek

  • @mamcostone1879
    @mamcostone1879Ай бұрын

    Cas bi doyna waar deh 😮

  • @user-im6wk6zs4s

    @user-im6wk6zs4s

    Ай бұрын

    Yw s'il te plaît beusseul traduction 😂

  • @MameboussoDiop-rn8ph
    @MameboussoDiop-rn8phАй бұрын

    Kholou nou wagniwounou sa yon nékou si

  • @MamadouSeck-jp1eo
    @MamadouSeck-jp1eoАй бұрын

    Ndakhté ❤❤❤❤❤❤❤

  • @halikano392
    @halikano392Ай бұрын

    Heuye akhmed Cissé YALLAH boma khamal thi adouna ak adamo ak seugne bada sheuteuteute

  • @MaxSeck-uk2we

    @MaxSeck-uk2we

    Ай бұрын

    Mannn kay gni wougniy dieuli sen information yi la khamoul

  • @user-if2zo6bs9g
    @user-if2zo6bs9gАй бұрын

    mé gni biniouy guéne bobou Mario yoroul gate toukiwoul sakh

  • @pendasarrgaye5102

    @pendasarrgaye5102

    Ай бұрын

    Mais Mario kagn la am khaliss ki yagoul touki Di Khawma louy problème bi mais d'où khaliss monsougueul ndakhté si sey bi

  • @diarracoly3214

    @diarracoly3214

    Ай бұрын

    Je valide​@@pendasarrgaye5102

  • @azizdiop7316
    @azizdiop7316Ай бұрын

    Mou yakh deirou domou diambour non ndakhtei ak gni neike si guinawam yeup aye domeiram laniou mbam laniou

  • @astouwade5888
    @astouwade5888Ай бұрын

    Yalla reka khama mais man guemouma nakhte vrema

  • @fatimakujabi8595

    @fatimakujabi8595

    Ай бұрын

    Wakh deug

  • @seynaboudiop9162
    @seynaboudiop9162Ай бұрын

    Ki meuneu feneu! Alahou akbar

  • @YvoneMendy
    @YvoneMendyАй бұрын

    Vraiment cisse

  • @awandewemieniane565
    @awandewemieniane565Ай бұрын

    Litax ta op contacter ndaxkté ishh

  • @khadydiagne2860
    @khadydiagne2860Ай бұрын

    Djiguen dal boko take dakoy wolou pr lokalise

  • @salimatasane5648
    @salimatasane5648Ай бұрын

    Ah néxoul ba nekh mais waxou matraque mom c'est louche. Xana malla sakh keine douko matraque. Mais djiguéne ak limoula meuna def boulko dore.

  • @boussobaly-vo3nq
    @boussobaly-vo3nqАй бұрын

    Bayil doul laissé ndaheter tranquille elle est très belle intelligente charmante demoiselle mario domerame rek la c tout

  • @YacineDiouf-lg6uv

    @YacineDiouf-lg6uv

    Ай бұрын

    Moko guiss si domeram bobou ba beugue ko khamna djikom bou yague tè tèwoul mou dougou si mom

  • @awalaissandoye5936
    @awalaissandoye5936Ай бұрын

    Wakhe dji yeupe moye daure yi mo waroule ak yéne comportement yi si kou yore diabare mo waroule

  • @sokhoulovedieng1365
    @sokhoulovedieng1365Ай бұрын

    Yéne est-ce que cava khana dégoléne li ndakhté wakh haaa dama warou mane ndakhté dîna def Lou bone ba paré moukoy wakh haa ma warou mane

  • @khadydiagne2860

    @khadydiagne2860

    Ай бұрын

    Moma diakhal

  • @user-hl1xk5tf3q

    @user-hl1xk5tf3q

    Ай бұрын

    Alors kepp kou wakh si télé rek,il a raison. Kone bokke guen si nji nangou Adji sarr degneko violé. Nangou guen ni RFI loumou wahal Afrique deuguela puisque kou wakh télé rek deguela

  • @PendaSow-he7eq
    @PendaSow-he7eqАй бұрын

    thank you so much bro I'm so 14:07 so proud of you

  • @binetasow2883
    @binetasow2883Ай бұрын

    Nakhté kay dafa dioum je ne sais pas kou KO digal li dafa dioum sur toutes la ligne ngoné Ndour si elle était une bonne maman elle devrait parler avec nakhté comme ça la petite n'allez pas faire ça parce que nakhté à sali Mario pour buzz et vendre son CD

  • @azizdiop7316

    @azizdiop7316

    Ай бұрын

    Dioumouniou daniou bone aye domeiram laniou yakhe deirou domou diambour gratuitement

  • @user-if2zo6bs9g

    @user-if2zo6bs9g

    Ай бұрын

    yakhoul deram moko def mou wakh ko

  • @azizdiop7316

    @azizdiop7316

    Ай бұрын

    @@user-if2zo6bs9g Bou sa yaye done neitali nga bayi sa papa 👨 😡neikeleine aye nite xaleibi Bou djigueine bi saga you niaw yi mou saga son mari sur la video du prank keineine koumou ko saga wone nga niaff ndayam so amoul maitrise

  • @ndeyesokhnadiagne6099

    @ndeyesokhnadiagne6099

    Ай бұрын

    ⁠yako féké ?

  • @binetasow2883

    @binetasow2883

    Ай бұрын

    @@ndeyesokhnadiagne6099 avant de me répondre lis bien ce que j'ai écris idiote

  • @tallambengue-oc4cd
    @tallambengue-oc4cdАй бұрын

    walahi Ahmed Cissé louh am solo lay wakh bilah

  • @AmyDiallo-dx3sg
    @AmyDiallo-dx3sgАй бұрын

    Mâcha alla qui est tu

  • @geraldinedossantos-mg2ru
    @geraldinedossantos-mg2ruАй бұрын

    Tey mome damaye mandou 🤐🤐

  • @meryndiaye1838
    @meryndiaye1838Ай бұрын

    Je ne suis pas d'accord akhe loumou deff c'est une raison de la battre si tu ne peu supporter bayil mou dém

  • @evachoudiop6430
    @evachoudiop6430Ай бұрын

    No bossou binette ce n'est pas la même chose ke ndakhtè en plus ndakhté dafa vulgaire

  • @LamineWas
    @LamineWasАй бұрын

    Mane sériniou nanditéyi la done khare

  • @ndeyefamasylla1270
    @ndeyefamasylla1270Ай бұрын

    Wa mais saga yi nak mak bou toll ni yaw ahh sénégal tamite

  • @luluvroumvroum9502
    @luluvroumvroum9502Ай бұрын

    Elle nous manipule cette petite😂😂😂😂😂😂

  • @diamaksallam3550

    @diamaksallam3550

    Ай бұрын

    😂😂😂

  • @aissatoumbengue1012
    @aissatoumbengue1012Ай бұрын

    mario lagn sokhla fiii😂😂😂😂😂😂😂

  • @pbt737
    @pbt737Ай бұрын

    Mon dieu !!! Thiey yallah !!!!

  • @DijahLo
    @DijahLoАй бұрын

    Bingassi dougeuleh saga Ngoko yaahh

  • @user-yy6ee6hv7r
    @user-yy6ee6hv7r29 күн бұрын

    Yow dulkat nga demal tog

  • @user-iw9vp9cb4k
    @user-iw9vp9cb4kАй бұрын

    Y’a sofe sofe gua

  • @ngonedionguembaye6632
    @ngonedionguembaye6632Ай бұрын

    Sénégal yeupe gneupa rew , dafa fèkeu ni rek rewandé dou fepp ngakey wané . Ndakhté avant prank bi kèneu meussoul djiss mou manquer de respect qui que ce soit . Dafa fèkeu ni qui cherche trouve nak . Dafa merr xolam djekh mou réagir lolou rek leu . Xalé bou ameu fouleu ak kou begn kouko yapeu lolou rek la djiss si mome nak . Tè niteu so mérè meune nga wakh dara pour blesser l’autre personne mais dou nèkeu lo xalate forcément en temps normal . Yaye sakh dey mérè domam dagalko ndeye djareu fou gnaweu donc negn bayi yeufou nafek touti . Ya salam

  • @absadiouf5894
    @absadiouf5894Ай бұрын

    DEUG leu ndakhter dafa agressive

  • @unebatante7716

    @unebatante7716

    Ай бұрын

    Yako fek doul kat bi

  • @user-we7mk3hj6y
    @user-we7mk3hj6yАй бұрын

    Mane mon bima degue ndakhte la wakh y dor la geumou mako Mane v

  • @dababa9252
    @dababa925229 күн бұрын

    Évité tais lene exposé sene mariage yi

  • @jamilasall7409
    @jamilasall7409Ай бұрын

    Ki Mario focéco tak kénéne ki dafa yape sa yaye boul taxativamente cou siwe té boye take tacal couco dakh saga sa yaye ki dou djiguéne boubakh badianamebi bandila coubocague khar mbaye doumalatak khar mbaye espagne ladane nieuwe filameuna yame ndakhté mi cariérame doudéme féne ki magia légui Mario daco sour ndakh limouco khamal ndédjeco si kholame bayiléne Mario gor la daye démefouco nékh focéleki dalaye tardéle heurebi waronena fégue nga ame 3 dome boulco tagate badianame bandila ndakhté banditla boco tagaté vie boubone ngaye néké focéco

  • @RiimaToure

    @RiimaToure

    Ай бұрын

    Louthiy sa yone

  • @imaneanne9464
    @imaneanne946422 күн бұрын

    KHALÈBI DAFA WOWE BEUTE KOU AME FITE LEU WALAY NOOONNN

  • @MaxSeck-uk2we
    @MaxSeck-uk2weАй бұрын

    Haaa kon dh ndakhte amna mayouk yala😅😅avortement 3fois ,,,,ndakh bo khasse ba avorte bala gua eumbe nimouy yagueee

  • @user-iw9vp9cb4k

    @user-iw9vp9cb4k

    Ай бұрын

    Dou lolou kamo li guaye wakh

  • @lamine728

    @lamine728

    Ай бұрын

    Esk dou contraire bi

  • @dieynabafall32

    @dieynabafall32

    Ай бұрын

    Cela existe j'ai une cousine elle a avorté 7fois la raison en est son mari et elle danio diégué

  • @unebatante7716

    @unebatante7716

    Ай бұрын

    Khana khamo ni bo avorté si Guay gawa dieulate eube

  • @mmemboup8612

    @mmemboup8612

    Ай бұрын

    C tout à fait le contraire

  • @user-jr2ly9kh5g
    @user-jr2ly9kh5gАй бұрын

    Loutakh sey bi tassoul té ideu bi diékhnaa

  • @Bour_ndiaye_bour

    @Bour_ndiaye_bour

    Ай бұрын

    Khana bala ideu di diékh niou fasséla

  • @user-jr2ly9kh5g

    @user-jr2ly9kh5g

    Ай бұрын

    @@Bour_ndiaye_bour mome lolou là wakh fassé nagneko

  • @Bour_ndiaye_bour

    @Bour_ndiaye_bour

    Ай бұрын

    @@user-jr2ly9kh5g kone soumala dégué limou wakh nga gueume instan bi sey dafa sacré déh lossiy gueume na done lou lérr

  • @rokhayatoudiengmbodji9881

    @rokhayatoudiengmbodji9881

    29 күн бұрын

    Kougnou fassé moy djapp iddaa

  • @Bour_ndiaye_bour

    @Bour_ndiaye_bour

    29 күн бұрын

    @@user-jr2ly9kh5g Mé ki wara fassé néna fasséwouko pour mane lollou mo geuneu worr

  • @aidagakou7978
    @aidagakou7978Ай бұрын

    koone ngua waraa teuthie saa guémigne cii problémame yeww waroo diokhe kénne conseils dakhe doo référence

  • @user-om1bo2xl2i
    @user-om1bo2xl2iАй бұрын

    Mane yaw rek la done khar gua wakh akhikha deux rek sama serigne

  • @fatimediattara2154
    @fatimediattara2154Ай бұрын

    Donite c vrai

  • @unebatante7716

    @unebatante7716

    Ай бұрын

    Djiguene day diapale sa moro mou djiguene

  • @user-gj3th6ie8s
    @user-gj3th6ie8sАй бұрын

    Ahmeth sa kharite la ndakhte leupe loumou wakh degue pure la tantam la khalela yio saye mane ga ko dioure diaroule top si wakh dji sayou khalela diaroule wakh. Dji yeupe

  • @NaRR.FaLL23
    @NaRR.FaLL23Ай бұрын

    bilahi serigne bi leiralna cas bi yeupp ndakhate limou wakh khadje bi yeupp ay dul leu

  • @onlygood1114
    @onlygood1114Ай бұрын

    En tout cas khamanté nanou 7an de relation ga neik ak mom mariage yéna yam ki 12 école si xalei pank saf lamigne

  • @abyndione7036
    @abyndione7036Ай бұрын

    Toi ferme-la

  • @MameboussoDiop-rn8ph
    @MameboussoDiop-rn8phАй бұрын

    Loune lénn wakhal lék dagann na

  • @adjaba8454
    @adjaba8454Ай бұрын

    Weuuuu🙄🙄🙄🙄

  • @BibaDiolita
    @BibaDiolitaАй бұрын

    Le mot féministe la andoul mane

  • @unebatante7716

    @unebatante7716

    Ай бұрын

    Ya xam

  • @user-eg2yv5hr9l
    @user-eg2yv5hr9lАй бұрын

    Kharal ma rere ba. Nopi gnew yegali

  • @sokhnatoutimbacke
    @sokhnatoutimbackeАй бұрын

    Doull👹👹👹👹

  • @halikano392
    @halikano392Ай бұрын

    Féne deugua sosse yokka

  • @user-gj3th6ie8s
    @user-gj3th6ie8sАй бұрын

    Ahmeth magui laye wakh ne ndakhte khale bou ame yare le séné yaye dafa istrique si yari domami sofa deme yare gafa guisse quartier bi koladje séné yarou lagnou laye wakh yala s'étend li maye wakh

Келесі