"VJ aime les filles au teint…»: la maman de la star se lâche...

Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
/ @senewebtv
Seneweb, c'est le site numéro 1 , Pionnier et toujours leader des réseaux de plateforme digitale au Sénégal et en Afrique de l’Ouest francophone
Visitez notre site web: www.seneweb.com
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
/ @senewebtv
Suivez nous sur:
Facebook: / senewebcom
Twitter: / seneweb
Instagram : / seneweb_officiel
Contactez-nous: +221 33 869 10 90

Пікірлер: 121

  • @Vod740
    @Vod740Ай бұрын

    Houréye Thiam belle professionnelle et pieuse meune wakh bou rafét Dieu te bénisse

  • @seynaboudia7459
    @seynaboudia7459Ай бұрын

    Yallah nako sunu borom Sam arrko té mousseul ko thi thiate ak cheytaan Ourey je l’aime bcp une femme qui a une grande personnalité

  • @dabachou5674

    @dabachou5674

    Ай бұрын

    Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏❤️

  • @RahouDou

    @RahouDou

    Ай бұрын

    Thiatt mom manoucé mouthie homme public la😅

  • @haby8760

    @haby8760

    Ай бұрын

    Elle ressemble à Zeynab Fall (ra)

  • @Cisse-zv7mm

    @Cisse-zv7mm

    29 күн бұрын

    Kii kay seytané dougou nako ba paré 😂

  • @MarietouDia-il8pd

    @MarietouDia-il8pd

    29 күн бұрын

    ​@@Cisse-zv7mm 😂😂😂😂😂😂 musique égal cheytane

  • @rokhayadiouf2671
    @rokhayadiouf267129 күн бұрын

    Ah elle me rappelle sokhna zeynab fall machalla

  • @haby8760

    @haby8760

    28 күн бұрын

    Ndèyssane MaShaAllah kone dou mane rèk ma sètlu lolu

  • @LizyDia
    @LizyDia29 күн бұрын

    Vraiment les commentaires que celui qui n'a jamais péché jette la première pierre maylein nitt yi diam elle sait k dafa kharam elle bien dit qu'elle respecte ki vous dis qu'elle ne fait tt son possible pour qu'il arrête occupez-vous de vos péchés ish

  • @seynaboufaye7883

    @seynaboufaye7883

    24 күн бұрын

    C'est vrai

  • @Reine-994
    @Reine-99429 күн бұрын

    Koufi khésal pour vj takeu la diga lakh 😅té do ko guisse 🥱🥱🤐

  • @Bafatoumata75ba-hq1qy
    @Bafatoumata75ba-hq1qy27 күн бұрын

    J ai fait 30ans de menange mâcha alla

  • @jazzomane1725
    @jazzomane1725Ай бұрын

    Que Dieu le protège,il peut amener un disque d'or au Sénégal inchallah 🙏

  • @ibaritoo556
    @ibaritoo556Ай бұрын

    SUPER, une interview à faire écouter . Machallah Houreye❤

  • @AbdelKader-kt7zj
    @AbdelKader-kt7zj27 күн бұрын

    Je l'aime depuis la Mauritanie qu'Allah la préserve ! Si toutes les femmes étaient comme elle voilé extérieurement et intérieurement le monde irait mieux ❤🙏 chapeau à elle

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo917122 күн бұрын

    Yangui tass séy t hamoko. Téyé micro diwah rék. Ngané Togou Dou séy. Prochaine fois nga rectifier wou. 2 wahnga ay DEUG you Bari nak

  • @ndeyeaminatagueye5487
    @ndeyeaminatagueye5487Ай бұрын

    Macha Allah franchement je l'admire cette femme. Toujours de bons conseils Macha Allah 🙏

  • @haby8760

    @haby8760

    Ай бұрын

    MaShaAllah ; fimeu gueuneu nèkh thi wokham Moy " khol lène ki nguène beug mu dioureul lène sèn dom nguène takko "

  • @user-mh6kb7wo9d
    @user-mh6kb7wo9dАй бұрын

    Kou bakh moy diour kou bakh en général. VJ est formidable on l adore

  • @koulaalhakk8975

    @koulaalhakk8975

    Ай бұрын

    Mais khamoul dara meunoul waay😂😂😂

  • @GoatJee

    @GoatJee

    22 күн бұрын

    Mdr music messoul bakh xaram la def 😊

  • @user-qu3vk9qs5p
    @user-qu3vk9qs5pАй бұрын

    Amine amine yarabi inchallah machallah ❤❤

  • @user-mh6kb7wo9d
    @user-mh6kb7wo9dАй бұрын

    VJ on t'adore yallah na la yallah laffal thiate ak lamigne ak beut bou ayy

  • @Fatoumainnayarassoul

    @Fatoumainnayarassoul

    29 күн бұрын

    On adore qu'Allah

  • @khadimfall538
    @khadimfall538Ай бұрын

    Merci maman pour tes belles paroles en vers ton fils

  • @khadidiatousall4155
    @khadidiatousall415525 күн бұрын

    Merci Monsieur Preira pour ces paroles à madame

  • @makhoucomdab2505
    @makhoucomdab2505Ай бұрын

    Bon pour mane liguey dou bone mais anam bi moy bone.. c'est juste mon avis.

  • @rokhayatouloumloum
    @rokhayatouloumloum24 күн бұрын

    Macha Allah amnaa solo thi conseils yi thi seuy ❤❤

  • @user-fqlt
    @user-fqltАй бұрын

    Magoum Lislam mooy yoon yu xalé yi di champion AlQuran sénégalais. Bayyileen thiaakhan.

  • @ibrahimadiouf4576

    @ibrahimadiouf4576

    28 күн бұрын

    Kou bakh mandou wo ki done magoum l'islam yalla ko kham

  • @ndeyerokhayagueye4582
    @ndeyerokhayagueye458226 күн бұрын

    Mashallah houray yana yalla samal la ndioboot gui.tu es véridique vraiment

  • @boubacarsamate3670
    @boubacarsamate3670Ай бұрын

    Èskeuy ioe mère nianal sa dom dji mou bayi musique ndax dafa xarame yao yagui moutour mouy lo xamni Yalla molako Sant. Amga part de responsabilité si loumou nek ni

  • @cheikhdme412

    @cheikhdme412

    Ай бұрын

    Ki dafa dioume mome khana li yalla wakh si musique ba paré ngan bayii ko si ana si responsable

  • @user-fqlt

    @user-fqlt

    Ай бұрын

    Deug bi werr. Fowé diiné ji rek ak seeni xell.

  • @Cisse-zv7mm
    @Cisse-zv7mm29 күн бұрын

    Lii motakh oumar sall nekh ma thi digg bi laye diarr

  • @user-sq4si4gk3y
    @user-sq4si4gk3y28 күн бұрын

    MachallAh ❤

  • @sokhnadiallo9013
    @sokhnadiallo9013Ай бұрын

    Machalla bien dit♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️✨✨✨✨

  • @FatouwoulaNgom
    @FatouwoulaNgom18 күн бұрын

    MachaAllah❤

  • @rackyndiaye7593
    @rackyndiaye759327 күн бұрын

    Merci pour les conseils❤

  • @user-qu3vk9qs5p
    @user-qu3vk9qs5pАй бұрын

    Machallah tata ouray ja t’adore machallah ❤❤

  • @user-oi5ls1vj9d
    @user-oi5ls1vj9d26 күн бұрын

    Amine Ya rabi inchallah 😢

  • @ibrahimadiop4672
    @ibrahimadiop4672Ай бұрын

    Yalnako Yala Sameu Arko Guindiko mais Musique mom dafa Xaram Boudon domou jambour nga waxko waxkoko reik

  • @koulaalhakk8975

    @koulaalhakk8975

    Ай бұрын

    VJ khamoul dara ay son khalé lay waay😂😂😂

  • @Cisse-zv7mm

    @Cisse-zv7mm

    29 күн бұрын

    Wa guiss gua motakh yalla fii neh amoul na damay warr

  • @sorayacoulibaly9221

    @sorayacoulibaly9221

    22 күн бұрын

    Thiey Houreye Djilba ya changer ni? Adouna mo goyd tank

  • @khadysow3582
    @khadysow358228 күн бұрын

    Machala

  • @user-rf1gt1wn5l
    @user-rf1gt1wn5l27 күн бұрын

    Dédèt, juum nga fo nakk. Béne joulitt dou encadrer sa doom si musique. Nèna amana bou maggué mou baayi musique. Dè moom dou taggou. Nako baayi lègui mo gueun si moom, djeuli ARQ'AAN di jangg.

  • @aissatasow6421

    @aissatasow6421

    27 күн бұрын

    Houraye ce que tu as dit sur le mariage à propos de la cuisine c’est n’importe quoi… ça fait partie du tarbiyou ngueu sonneu pour sa dieukeur… En plus un bon parent musulman ne doit pas encadrer son enfant ci lou harame, musique

  • @user-rf1gt1wn5l

    @user-rf1gt1wn5l

    27 күн бұрын

    @@aissatasow6421, mooma jaaxal tamitt.

  • @boydiff2213
    @boydiff2213Ай бұрын

    Machallah ❤❤❤

  • @haby8760
    @haby8760Ай бұрын

    Yala neulène Yala sammeu mère et fils Amine 🤲

  • @omarkonde31
    @omarkonde3129 күн бұрын

    Je n'aime pas ce qu'a fait la journaliste. On ne doit pas s'immiscer dans les affaires des autres. Et puis on ne peut pas forcer par celà une personne a prendre le bon chemin. Madame tu devrais d'avoir parler à cette journaliste de se voiler avant d'être avec toi sur scène sinon refuse. Il n'est pas normal que tes bras soient découverts ni certains bijoux, ceci est destiné à être caché. Ce que tu avais dit à propos des femmes sur les travaux ménagères, ce n'est ni l'islam ni la tradition du pays et même J'ose dire à l'international. Dans le milieu conjugal, l'homme comme la femme ont leur part de responsabilité. Je te donne une preuve rationnelle, c'est que lorsque ton fils né, il t'est tenu responsable de la préparer à manger, boire et s'occuper de son bien être général. Et qu'est-ce que ça te coûte de le faire pour ton mari si ce n'est que tu obtiens en cela honore et miséricorde d'Allah. Est-ce que tu connais le sens du mariage ? Je ne vais pas rentrer sur les autres erreurs remarquées sur ton comportement apparent car je ne veux que mes mots tends vers l'impolitesse. Mais ma sœur si j'ai un conseil à te donner mieux vaut éviter de parler en tv fitna rekk la. Nitt ñi dañulaye deukeul. Mangui ñane borom bi dioubeul ñu ci sirAtal moustahime.

  • @mameboussofaye4032

    @mameboussofaye4032

    29 күн бұрын

    Li gua wakh d ❤️ la deukké machallah ak sama borom keur et je le fais avec plaisir damay yakamti mou wathie ndeyesane bama topato ko melni kou yoor bb machallah ❤️❤️❤️❤️

  • @ModouDiop-vq4kh
    @ModouDiop-vq4kh28 күн бұрын

    Machalla ❤️

  • @user-mh6kb7wo9d
    @user-mh6kb7wo9dАй бұрын

    Gni nane musique dafa aram da nio sokhor li guena aram mi gui si deuk bi niou koy guiss chak jour bou gnou kén ray

  • @amyba5578

    @amyba5578

    Ай бұрын

    Bou yawmal xiyamè nga tontou li yalla...

  • @Cisse-zv7mm

    @Cisse-zv7mm

    29 күн бұрын

    ​@@amyba5578comprends ko gas yi soriwoul nioy wax li guena bonn migui khamou niou lou beuri thi sen diné

  • @Amadouba-yh5sm

    @Amadouba-yh5sm

    25 күн бұрын

    Mais lolou takhoul musique bania haram ba legui

  • @Cisse-zv7mm

    @Cisse-zv7mm

    25 күн бұрын

    @@Amadouba-yh5sm bly wakh deug fa yalla

  • @Fatou2001

    @Fatou2001

    25 күн бұрын

    Donc y'a beaucoup de péchés dafa wara takh nguay encourager nieupp pêcher ??

  • @Salikhate732
    @Salikhate732Ай бұрын

    Ba adounay bakh 🤣dh sokhna moy togal borom keuram

  • @Cisse-zv7mm

    @Cisse-zv7mm

    29 күн бұрын

    Kii na lidieunti dom ji thi music bi mo geune nan djiguene dou togou

  • @nogayedieng5309
    @nogayedieng530922 күн бұрын

    Mashallah 🥰 une femme de valeur ❤

  • @BabkrBabeker
    @BabkrBabeker26 күн бұрын

    machalah ma cousine et long vie mon fils

  • @mariemebiendidialikadiagne989
    @mariemebiendidialikadiagne989Ай бұрын

    Toujours egale a elle je t'precie vraiment manchalla long vie ta ourey

  • @modoudabo8991
    @modoudabo8991Ай бұрын

    Yaye diour vj

  • @bajjanmaram4409
    @bajjanmaram4409Ай бұрын

    UNE VOILÉE ET FÉMINISTE EN MÊME TEMPS..OUIII CEST POSSIBLE..PAS MAL DE VOILÉES SONT DES FÉMINISTES.. MAMAN DE VJ ARROGANCE JARUL JAAY: " GOOR GNI BULEN GNU FONTOO" LE ROLE DE LA FEMME CEST D ÊTRE MÈRE, YAAY, ÉDUQUER SA RICHESSE( ses enfants) PRENDRE SOIN DE SA FAMILLE, LE MARI Y COMPRIS..MAINTENANT CUISINER EST NOURRIR SA FAMILLE CEST COMME DONNER LE SEIN À SON BB..MAINTENANT CEST UNE ÉVIDENCES QUE QUAND UNE FAMILLE A LES MOYENS ET LES PREFERENCES DE SE NOURRIR DE METS ACHETÉS AU RESTO CEST UN CHOIX.. MAIS DIRE QUE CUISINER BOKUL SI SEUY, CEST UNE FOLIE..CUISINER CEST AUSSI PRENDRE SOIN DE SON MARI ET DE SES ENFANTS...

  • @user-fqlt

    @user-fqlt

    Ай бұрын

    Deugg bu werr. Merci

  • @yayemariediouf9160

    @yayemariediouf9160

    28 күн бұрын

    Ta parfaitement raison cuisiner thi seuye la bokk voilà

  • @ndeyerokhayagueye4582

    @ndeyerokhayagueye4582

    26 күн бұрын

    Si le couple a des moyens vaut mieux qu'ils embochent une bonne.occuper les enfants le mari les tâches ménagères c'est une traquesserie.

  • @adamasarr3844
    @adamasarr3844Ай бұрын

    Machalla bravo

  • @senegal2

    @senegal2

    Ай бұрын

    Yalnalen yala lafalthite

  • @boubacarsamate3670
    @boubacarsamate3670Ай бұрын

    Fékhél mou guéneu si sowbise bi nëko mou bayi musique bi da xarame mo geun

  • @alhamdoulilah3991

    @alhamdoulilah3991

    Ай бұрын

    Vraiment. Wakh Mouhamed ba paré ték thi VJ.

  • @fas2822

    @fas2822

    Ай бұрын

    Wahnakoko deh xalé bi mooko beug

  • @PapisDieye-gt5fw
    @PapisDieye-gt5fwАй бұрын

    Vj Amal diam rk

  • @nimspetite
    @nimspetite29 күн бұрын

    Senegal mo nékh koi deglou séne commentaire yi yakar ni messo léne deglou musique ou bien vous éte parfais senegalais yi naw guéne sene jeufff pour yéne dé moléne téré dougou adiana parce daguéniy jouli ou woor nakh guéne sène bop adiana ak safara yalla moko mom mom rek moy tane kifay dém

  • @mbathiokasse

    @mbathiokasse

    29 күн бұрын

    C vrai yalla Moy décidé ms lo liguey ci adouna rk Molay atté allakhira d'où on cherche à dire et faire du bien pas parcek on n'est parfait ms Parsk c l devoir de tout CROYANT❤ Xolatal sa sens de réfléxiôn stp

  • @nimspetite

    @nimspetite

    29 күн бұрын

    @@mbathiokasse en tout domou adama Menoule jamou yalla ba am certitude que adiana la Jeum pareillement domou adama menoule moy yalla ba am certitude que safara la jeum Safara ou adiana seul DIEU décide

  • @nimspetite

    @nimspetite

    29 күн бұрын

    @mbathiokasse ah j'avais oublier yalla ci say Jeff adouna AK yeurmandém lay até pas seulement Jeff renseigne toi

  • @rokhayatouloumloum

    @rokhayatouloumloum

    24 күн бұрын

    Wax nga deug dh Mais yallah waxna thi alqur ane langay df pour dougou aldjannah wala lingay df pour dougou safara juste rk pour gnou moytou ko ndax lo khamoul meunooko moytou Dank yalna Yallah djoubeul gnou rk lolou mo am solo

  • @amardembaofficiel2762
    @amardembaofficiel2762Ай бұрын

    ❤❤❤❤

  • @khadidiatousall4155
    @khadidiatousall415525 күн бұрын

    Walay diiné avant tout et le reste viendra

  • @user-ip6vd4kg4g
    @user-ip6vd4kg4gАй бұрын

    Vj mangui ni je t aime bilay yaw rek lay top ❤️🙏

  • @deenmotivated670
    @deenmotivated6706 күн бұрын

    Tu respect son choi? Bayileeb thiakhaaan, musique mom Dara bakhousi teh waroko si diapalè, dang ko wara kheekh mu bayyika.. benên bi moy ki du khalé, mukallaf la

  • @Ousmanediop-qe6qd
    @Ousmanediop-qe6qd28 күн бұрын

    ❤❤❤

  • @user-mh6kb7wo9d
    @user-mh6kb7wo9dАй бұрын

    Bayilén ko mou musique il le fait bien. Gni nane musique dafa aram gni gui déf lou gueneu aram bou gnou kén ray.. j'adore VJ

  • @koulaalhakk8975

    @koulaalhakk8975

    Ай бұрын

    VJ vraiment khamoul dara meunoul😂😂😂😂

  • @user-gc4tr9oo5r

    @user-gc4tr9oo5r

    28 күн бұрын

    Mes tèwoul mou haram dè

  • @aminatamane3327
    @aminatamane332727 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @misszjuke4914
    @misszjuke4914Ай бұрын

    Tu parle beaucoup, ton defi est de faire comprendre ton enfant vj que la musique et son cercle est haram !

  • @misszjuke4914
    @misszjuke4914Ай бұрын

    La musique est haram😢

  • @bakhyayeprod
    @bakhyayeprod29 күн бұрын

    Yaye respect naa la trop wayé togou bokoul si seye mom wakhi dof la

  • @marfatou5239

    @marfatou5239

    29 күн бұрын

    LOL danguén réré s'en dîné motah koulén am soneu

  • @ibrahimadiouf4576

    @ibrahimadiouf4576

    28 күн бұрын

    Kou bakh elle a raison lou niit meuneu faye pour niou defal ko ko bokoul si seuy

  • @babacarcisse250
    @babacarcisse25025 күн бұрын

    Lou yalla wax yen si sen alaL ak sen dom natoula dou lou nehk sa dom rék lou bahk la

  • @MouhamedDione-si7ps
    @MouhamedDione-si7psАй бұрын

    Nooo senegal moo nekh depart gainde arrivé bonam waa Sokhana sii liko enragé rek la wakh hee djick bul dull tok du foot l'ann moy dierignaw sii seuy nonn

  • @maduzor1053

    @maduzor1053

    28 күн бұрын

    🤣🤣

  • @awabalde4598
    @awabalde4598Ай бұрын

    😂😂😂😂❤

  • @malicksy7171
    @malicksy717128 күн бұрын

    Bodewe yalla dinala laje la motax mou nek musicsen

  • @tidianesylla8618

    @tidianesylla8618

    25 күн бұрын

    😂❤

  • @ramatoulayeracinegaye4355
    @ramatoulayeracinegaye4355Ай бұрын

    deug pire

  • @floorishy
    @floorishyАй бұрын

    da ngay fontou rek, mourou di diay diné baparé sa dome di football aka woyy Sénégal dou deuk koi kouy def musik nougne koy nianalé yalla ??

  • @nimspetite

    @nimspetite

    29 күн бұрын

    Yaw sa dome loumay déf wala loumouy done euleuk wala loumouy job actu

  • @marfatou5239

    @marfatou5239

    29 күн бұрын

    ​@@nimspetitemoma diakhal. Bakar yimouy Def douko wah

  • @floorishy

    @floorishy

    26 күн бұрын

    @@nimspetite yalla rek kham si souniouy dome, mais hourèye dou réfèrence. pourtant j'étais fan d'elle temps RTS, ndékétéyo yaroul dom dji batay mouy music, goor ak djiguéne di tassé concert ba moy yalla am fa yone. ça me fait mal pour elle

  • @floorishy

    @floorishy

    26 күн бұрын

    @@marfatou5239 yow aussi bakar yi ngay def doko wakh. wakhouniou wakhi bakar, mais louné fang si espace public bi. lolou motakh kouné sagne ci diokhé khalatam

  • @Lovefootball221
    @Lovefootball22128 күн бұрын

    Musique 🎶 koula wax da haram day fénn

  • @diarrasall4221

    @diarrasall4221

    27 күн бұрын

    Wakh ko yallah konn🤦🏽‍♀️...

  • @SiriDiallo

    @SiriDiallo

    24 күн бұрын

    Allakhou akbar 😭❤️☝️

  • @floorishy
    @floorishyАй бұрын

    da ngay fontou rek, mourou di diay diné baparé sa dome di football aka woyy Sénégal dou deuk koi

  • @maduzor1053

    @maduzor1053

    28 күн бұрын

    Football dagane na mais musique mo haram

  • @floorishy

    @floorishy

    26 күн бұрын

    @@maduzor1053 football bou nekk foo mo dagane, mais biniouy def légui daganoul ndakh dafa andakh carte khaliss té dagniy fate wakhtou

  • @mortallafall3048
    @mortallafall3048Ай бұрын

    Néko Mou Bayi Musique Musique Dafa Haram

  • @fas2822

    @fas2822

    Ай бұрын

    Wahnakoko deh xalé bi moo def kouko nekh

  • @nimspetite

    @nimspetite

    29 күн бұрын

    Jesper que yaw do deglou musique

  • @AmethLo-wk7xi
    @AmethLo-wk7xiАй бұрын

    Machalla lu motakh ga ame dome bou melnu vj

Келесі