THIAROYE : Pape Sarr décède suite à une intervention de la police la vérité éclate

THIAROYE : Pape Sarr décède suite à une intervention de la police la vérité éclate (regarder les photos et la vidéo)

Пікірлер: 351

  • @mafresh1727
    @mafresh17276 жыл бұрын

    😢😢😢😢😢 sama xol bi moy metti bilahi li metina torop

  • @nadiadia

    @nadiadia

    6 жыл бұрын

    Ma Fresh pikini production la soeur à tt expliquer. C tellement triste

  • @nittoudeugrek9684

    @nittoudeugrek9684

    6 жыл бұрын

    Ma Fresh non lii dafa gnaw vrement lii gnawna trop

  • @djimbisow4298

    @djimbisow4298

    5 жыл бұрын

    Ma Fresh 0

  • @papediakhate1541
    @papediakhate15416 жыл бұрын

    Wa kogne bi naniou mobilisé wou tall police sou thiaroye bi prk la justice soit faite

  • @awatoure3287

    @awatoure3287

    6 жыл бұрын

    Pape Diakhate m

  • @awatoure3287

    @awatoure3287

    6 жыл бұрын

    .

  • @aliassokhorfemmmya6208
    @aliassokhorfemmmya62086 жыл бұрын

    Ki deme yallah nako yallah yeureume te kharee ko aldiana l'y doyna warr dalle la police doit protéger les citoyens et non tué

  • @combesane8630

    @combesane8630

    5 жыл бұрын

    Amine

  • @yacinendiaye2050
    @yacinendiaye20506 жыл бұрын

    J'ai les larmes aux yeux pourquoi tant de barbarie .ça suffit la police nous ne sommes pas des animaux même un animal ne mérite pas ça. Si nous voulons préserver la paix ici au Sénégal il faut que ces actes ignobles cessent. Arretez!

  • @bitra6145
    @bitra61456 жыл бұрын

    Il faut ouvrir une enquête, interroger les médecins, témoins... c’est très dure de savoir que la police sénégalaise agit contre le peuple et en toute impunité. Même en garde à vu ils n’ont pas le droit de frapper, malmener ou encore torturer. Leurs méthodes ressemblent à celles des militaires en zone de guerre c’est inadmissible. Il faut que le peuple se mobilise, ça fait vraiment mal au cœur. Paix à son âme

  • @awasane1156

    @awasane1156

    5 жыл бұрын

    Bi Tra vraiment une enquete vraiment cé triste sa

  • @maymouna1802

    @maymouna1802

    5 жыл бұрын

    Médecin ak policiers niom aye conplice lagne

  • @sanoudaniel
    @sanoudaniel6 жыл бұрын

    Franchement c'est triste quand je vois que personne ne réagit

  • @diarramane8549
    @diarramane85495 жыл бұрын

    Bilay adouna da sopékou mais justice doit ouvrir l'enquéte sino les population doivent mobiliser pour combattre sa

  • @Bolyouleye
    @Bolyouleye5 жыл бұрын

    Ces policiers qui se croient tout permis qui tuent les citoyens comme ça c'est grave et honteux

  • @habycisse3609
    @habycisse36094 жыл бұрын

    Celà me fait peur de revenir au Sénégal !!!!!

  • @fallougueye9275
    @fallougueye92756 жыл бұрын

    Police Sénégal ay demeram mosi eupe wayei yalla amna balla gniouy dei dinagnko guissss

  • @nittoudeugrek9684

    @nittoudeugrek9684

    6 жыл бұрын

    Fallou Gueye bilay dignak ko guiss

  • @moussambengue2095
    @moussambengue20956 жыл бұрын

    Procureur général naka yeug def ligueyame maître assane dioma Ndiaye et tout les avocats du droit humains

  • @ibrahimagueye4150

    @ibrahimagueye4150

    4 жыл бұрын

    Moussa Mbengue yeuk nako Bou bakh doussi wakh dara talouko sakh

  • @layelaye6583
    @layelaye65836 жыл бұрын

    massa papa metina trop yalnala yalla diokh kholou mougne si barke borom touba

  • @papediakhate1541
    @papediakhate15416 жыл бұрын

    Vilay sama xoll dafa diékh té manoumasi dara😤😤😤😤

  • @tallamboup131

    @tallamboup131

    6 жыл бұрын

    Pape Diakhate li kay kouka setan sa xoll diekh weye kou def loula nekh nanga dadjie ak loula nakhari

  • @soyegueyebaye1583

    @soyegueyebaye1583

    5 жыл бұрын

    Talla Mboup من فعل ما شآء لقي ماسآء

  • @aminatadiouf5851

    @aminatadiouf5851

    5 жыл бұрын

    Billahi beuri ngassi morom

  • @badgone6965
    @badgone69656 жыл бұрын

    Vraiment police thiaroye daniou oubi sen leufeul Ndey quoi.Daw heure pareille sama quartier. Sen intervation comme kouy deff guerre domou xarammm malheureusement naroul moudiou fenn ndakh sénégal amoul Yonne 🤦🏿‍♂️

  • @nittoudeugrek9684

    @nittoudeugrek9684

    6 жыл бұрын

    MOMO GG c trop lii gnawna trop policier yi yep yi ko def lagnou wara diap teuth lene a vie

  • @mamindir6264

    @mamindir6264

    4 жыл бұрын

    Lou weer nga wakh naroul moudiou fène té limeusi gueneu mèti moy douniou lène dèf dara wayé yalla guisna lepp,ndakh leegui douniou dieul ay vrai policiers lisi eupeu ay lidieunti beu niou dieulène douniou kham dara pour niom pour nga nèk homme de tenu danga wara sokhor yalnama yalla mousseul si niom yalla bouma léne kham kouma yilif doko nèk ndakh balla nga dè torokh bané tootou,li niawna

  • @shiinalaye7219
    @shiinalaye72195 жыл бұрын

    C'est vraiment injuste et le crime reste inpunit keine xamoul li lanela

  • @awasane1156
    @awasane11565 жыл бұрын

    Massa pere ce qu'ils sont fait n'est pas du tt normal j'ai des larme aux yeux massa

  • @amyndiaye4656
    @amyndiaye46565 жыл бұрын

    J'ai vraiment mal comme si c mon frère ou quelqu'un de ma famille j'ai tellement pleuré Rip

  • @aliassokhorfemmmya6208
    @aliassokhorfemmmya62086 жыл бұрын

    Le procureur doit s auto saisir de cette affaire

  • @aissatouseydi5564
    @aissatouseydi55646 жыл бұрын

    Cest dommage dou niou porte plainte motax policier niou def lou leen nex

  • @diagnegnilou1078

    @diagnegnilou1078

    6 жыл бұрын

    aissatou seydi bilay damahamoul motah porté wougnou plain

  • @Music-du6bq
    @Music-du6bq6 жыл бұрын

    Wa ana opposant yi wakh né Sénégal molén sokhal dougn ci wakh nak en attendant gnouy dokhane ndayou policier yiii

  • @mendesshasha1021

    @mendesshasha1021

    6 жыл бұрын

    opposant yi sen bop rek lagn fi nekal

  • @buzzattaque836
    @buzzattaque8366 жыл бұрын

    Nioune fane laniou dieum Légui gnii dane protégé nitt gnii nioy rayy nignii Police Sénégal lignouy wakh si niom beurineu trop té lii dieumoul keur khamngène domou diambour djii nguéne fékkii djilo yayam thia alakhira té heureum diotoul lii métina en plus lou tolnii djigué rawatina kou déff trois opérations aussi dii soga Am dome nioukoy mal traité choqué lii même souniou neubé deug bii gnii KO déff dii dokh sén sokhla tamite lii dou meuss dii guéneu sii sén bopp ndakh bakane dafa fort wayé mane magui niane yalla yalla naléne yalla atté adouna ak allakhira dii massa ou wa famille bii aussi diko nianal déwam bii nimou métiwé yalna souff oyoff té séed sii kawam té allahou rabihii kharéko aldianay firdawshi vraiment c l'injustice choqué

  • @azeaze1910

    @azeaze1910

    6 жыл бұрын

    Buzz attaque ppppppp

  • @azeaze1910

    @azeaze1910

    6 жыл бұрын

    Buzz attaque ppppppppppp

  • @moussapastor4919

    @moussapastor4919

    6 жыл бұрын

    Buzz attaque deugeu bou wér nga wakh lépou macki sall la

  • @binetagueye7482

    @binetagueye7482

    6 жыл бұрын

    Lii metti na te gni wara wakh kenn dou wakh porquoi mass courant nit ak mandi nekk thi service pourquoi doore

  • @binetagueye7482

    @binetagueye7482

    6 жыл бұрын

    Lii population bi gnoo meuna diog fadial ko seen bopp

  • @margueritebetty1205
    @margueritebetty12056 жыл бұрын

    polices Sénégal danio wara kholate faux policé. yi.NK thie police. by Aÿ féticheurs Aÿ d'Eume.sénégalais. tite.nagnou yasalam

  • @fatoudiouf4992
    @fatoudiouf49926 жыл бұрын

    Wallahi li metina te lou melni beuri na legui Sénégal man dama wara dé sakh ndakh limay guiss Sénégal legui nekhouma wallahi

  • @taphandiaye7896
    @taphandiaye78965 жыл бұрын

    la formation de la police doit se faire à bango comme ça ils connaîtront la valeur de cette tenue de savoir qu'ils sont là pour servir et non pas pour massacrer la population

  • @dioplepoetegalsen8674
    @dioplepoetegalsen86745 жыл бұрын

    J'avais entendu cette histoire mais vraiment meti na trope. Quantes yaura une justice égale à egale?

  • @ndiobayefall7554
    @ndiobayefall75546 жыл бұрын

    Non Senegal amoul loi bilahi lii ñiaw na vrément té kén doussi wakh no néw dolé bakhoull

  • @abdoutiare7310
    @abdoutiare73106 жыл бұрын

    Sénégal no dou dém yaw niou ray sadom ngana da ngaye balé

  • @mouhamadoumoustapha2094

    @mouhamadoumoustapha2094

    6 жыл бұрын

    Frère limo takh sa va continué.il fau condamné les impliqués.yala bakhn ak mougneul mo takh lini mél di répété wou

  • @mamindir6264

    @mamindir6264

    4 жыл бұрын

    Niaka kham rek ak ragal policiers mèlnè nom douniou nite

  • @sarrabibatou4336
    @sarrabibatou43365 жыл бұрын

    😭😢😭thieye li nitt dina ko df moromou ni teum thieye dh amna dh

  • @roseaminatadiop6157
    @roseaminatadiop61576 жыл бұрын

    C’est incroyable mais liii dou yone😢😢😢

  • @ymgxtmtc2990
    @ymgxtmtc29906 жыл бұрын

    Bilahi sama khol bagui metti metti bo khamnee policier yi deff lii yala nagnou dee

  • @saf-tnexx6731
    @saf-tnexx67316 жыл бұрын

    ndeye sane senegal amatoul aye goore goore yeupou dèe nagnou cii galyi goordjiguen yii ngnofa barry mè lii populationbi ngno wara manko raye 10policè djieul goone katsèn ndaye mème pa un moi ngnpu raye 8persone tangno wara protègè mane lila guiss moye solution

  • @diadiawo61

    @diadiawo61

    6 жыл бұрын

    Saf-T Nexx waxe daye rafète wala daga diapouni yawe rek ya dougou si galyi

  • @poulhoba7765
    @poulhoba77656 жыл бұрын

    Comment pouvons-nous être en sécurité si les gens qui devraient prendre notre sécurité nous prennent comme des bêtes ndeysane c vraiment triste 😭

  • @iibassndiaye2886
    @iibassndiaye2886 Жыл бұрын

    Que justice soit faite pour pape sarr 😭😭😭

  • @latyfalena9377
    @latyfalena93775 жыл бұрын

    Yalnalenn yalla até barkeih serign babacar sy barkeih yoninte bilay metina j mm pleuré way yalla doulen setane

  • @Diarista90
    @Diarista907 ай бұрын

    Am na niari dé youma mètti lole Pape Sarr Ilimane tourè 😭😭😭😭😭😭

  • @antishudiawista9262
    @antishudiawista92626 жыл бұрын

    Bilahi j n p tenir ms larmes pask li dafa méti

  • @fatoukinembaye2717
    @fatoukinembaye27176 жыл бұрын

    Non li yombe na na wa thiaroy mobilisé tal policier yalla na yalla até

  • @4KVISIONSENEGAL
    @4KVISIONSENEGAL5 жыл бұрын

    9 mois après toujours justice bi wakhoul darra les policiers doivent payer par le sang

  • @mariamadiallo1721
    @mariamadiallo17215 жыл бұрын

    J’ai suivi le témoignage de sa soeur, ces policiers sont des monstres, ils ne respectent même pas les gens.C’est vraiment triste de voir que la police scencé de mettre l’ordre dans la société se met plutôt à terroriser la population. Je comprends pourquoi en Afrique on souffre autant, les gens ne connait pas la valeur de l’être humain surtout ces soit disant homme de tenue. Que l’âme du défunt repose en paix

  • @almamyseckgoroumaremesoda
    @almamyseckgoroumaremesoda6 жыл бұрын

    Ndeyssan gorgi geum na Yallah... Mais li niaw na il n’y as plus de justice au Sénégal té loussi méti moy dou moudié feene nak yallah nalén souniou borom maye kholou mougne

  • @hawaseck8358
    @hawaseck83586 жыл бұрын

    Khana sax mém bouféké danko sathi nitt mogena fort Aÿ xarr fouff

  • @mbayesonko8968
    @mbayesonko89686 жыл бұрын

    Noi tothie sen leufleul ndeye yi polizie

  • @hawaseck8358
    @hawaseck83586 жыл бұрын

    Kidéf lou niawly yalla moko epp Dolé fooff té gisnako

  • @taphandiaye7896
    @taphandiaye78965 жыл бұрын

    je suis un porteur de la tenue militaire mais j'ai vraiment honte la tenue c'est pour le travail et non pour terroriser la population mes condoléances aux familles défunt et toutes nos excuses

  • @abdoulayebalde6227
    @abdoulayebalde62275 жыл бұрын

    Legui policier loulène nèkh deff Sénégal amoule loi

  • @anoudiop6580
    @anoudiop65806 жыл бұрын

    😢😢😢😢mettina trop nekhoul thi khôl

  • @matarfaye2583
    @matarfaye25835 жыл бұрын

    من كان يرجو لقاء ربه فليعمل عملا صالحا

  • @yallakesse5354
    @yallakesse53546 жыл бұрын

    Ho mane khamatouma Sénégal raye rek té dara doulasi fek

  • @mormbaye3527

    @mormbaye3527

    6 жыл бұрын

    Wa ana partie opposant yii

  • @brasildakar180
    @brasildakar1806 жыл бұрын

    Macky sall bilakhi walakhi sama akk soula dale dou bakh bilakhi ningay tangale sama xol bi doumala Bal ba yomal khiyam sonal nganiou 😤😤😤

  • @rassoulndiaye1378

    @rassoulndiaye1378

    6 жыл бұрын

    Brasil Dakar désolé cheri mais macky na rien fait

  • @rassoulndiaye1378

    @rassoulndiaye1378

    6 жыл бұрын

    C la police

  • @brasildakar180

    @brasildakar180

    6 жыл бұрын

    Wakh tan day nex borom keur , Macky sall Moy fay policie yii

  • @dieynabangom2500

    @dieynabangom2500

    6 жыл бұрын

    Nioune ban rew laniou nek aaaaaah li metina

  • @nittoudeugrek9684

    @nittoudeugrek9684

    6 жыл бұрын

    Non lii dafa eupeu trop

  • @mazoufaye4232
    @mazoufaye42325 жыл бұрын

    li le président macky sall daf ko wara yeuk ki déee sini té xamna narta moudié fene li yombou na trop

  • @alioudieye1121
    @alioudieye11215 жыл бұрын

    Yallanako yalla yueruem kharekolko alldjana yalla na yalla fenieler amiiin yon tek len aye daan

  • @mazoufaye4232
    @mazoufaye42325 жыл бұрын

    Niome niko ray policier yi naniou lagne teuthieu en plus ngéné lene si police bi la dafa yombou trop billahi wallahi souma bocone ak familles policier yi dinagne xam lep deugu leu

  • @salyallemomuawrksarr8652
    @salyallemomuawrksarr86523 жыл бұрын

    Policie yi li bathi serase wakh rk mofi ame nio daka ray bandi yisi boure diél bi😭😭😭🙏🙏

  • @aliounebadaraleye4713
    @aliounebadaraleye47133 жыл бұрын

    Deukkk bo khamny Do Comp Sakhee ☆ Sossetice & Justice

  • @adjidieye7161
    @adjidieye71614 жыл бұрын

    Bilahi li métina métina trop repos a son âme mais on devrait brûler le commissariat avec eux a l'intérieur 😡😡😡😡

  • @brahalefou7502
    @brahalefou75024 жыл бұрын

    Franchement c'est du n'importe koi avec cette police loumassi meti moye dou moudjé feneu c vraiment bizarrr justice ......

  • @aliassokhorfemmmya6208
    @aliassokhorfemmmya62086 жыл бұрын

    Mais Sénégal legui doyna warr dalle boudé kou ame dolée borome tour ou daradia bounioulaye yobou gni escorté la ame gni nek si ganaw dila kehlele ba ngua ague thi police bi mais sou dée kou newou dolée gni dila watate di door mba ngua dée thieye Sénégal doyna warr dalle

  • @aidafall1031
    @aidafall10316 жыл бұрын

    Naniou dem gendarmerie porte plainte

  • @tourendiouga5259
    @tourendiouga52596 жыл бұрын

    metti na loool waye

  • @toutaneba7257
    @toutaneba72575 жыл бұрын

    Regarde mw sa reck légui yakololéne ki avenirame diape nite diko torturé bamou dhé anni droit de l'homme loumiye diarigne fii dhi traité une personne kome un animal lii dafa niaw thé kate dou âme béne suite par ce que Sénégal bo necké badolo yaye à la merci c du n'importe kw lii niawna trop

  • @ibrambacke5148
    @ibrambacke51486 жыл бұрын

    Senegal diakhal nama trop

  • @aidafall1031
    @aidafall10316 жыл бұрын

    Walay naniou dem rek ay policier wara yorer souniou sécurité di rayé rek c un acte vraiment ignoble Sénégal mom legui sécurité amatoufi yalla naniou yalla sam.yalla nako yalla yereum te kharer ko aldiana vraiment metina dama dioy ba sama khol di meti

  • @bambambengue7801
    @bambambengue78016 жыл бұрын

    Kudud sutural nit yahala dula sutural

  • @moussambengue2095
    @moussambengue20956 жыл бұрын

    Bou niou beugué diame am na niou lerale li na yonne def ligueyame niou diap ni ko def

  • @bilifall7824
    @bilifall78246 жыл бұрын

    Toi le Pere de pape sarr merenala lol sakh lane moy bayi ak yalla porte plainte contre ses embesiles qui on tue ton fils boul diegeul persone nagnou subir les consecense Tous

  • @deugrek3312

    @deugrek3312

    6 жыл бұрын

    *Bili Fall daffa khamni sou planté d'où moudjou féne, combien de cas you melni mo aam ci police Sénégal? La liste est longue. Mais tout ça c la faute de l'état. C l'état qui doit prendre c responsabilités pour c bavures policières. C d vrais salauds c policiers de merde*

  • @bayecheikhwagnesow6708
    @bayecheikhwagnesow67083 жыл бұрын

    Bilay walay li métinama trop té mounoumasi dara😢

  • @beibishng5304
    @beibishng53045 жыл бұрын

    Guisouma borom xar yii mes gathié raynakoo li gathié la en temps k policier nguen fookni mass courant moy fadj soxlaa makhala dianguolen pr yen lepp force laa mes yalla gui guiss leep

  • @linguerouamathfall6524
    @linguerouamathfall65246 жыл бұрын

    Dama dioy bay beugua dé bilahi

  • @comptepro1221
    @comptepro12214 жыл бұрын

    L'indiscipline des policiers du Sénégal est une chose qui est connu de tous....je crois que tout le monde a déjà eu un clashh avec eux.

  • @mboldieng234
    @mboldieng2344 жыл бұрын

    Yalla guisna Lepou bilahi pollice yalla wolen eupou dole

  • @cornermovies4773
    @cornermovies47735 жыл бұрын

    Vraiment c honteux

  • @milkdiop164
    @milkdiop1646 жыл бұрын

    Principal policier yi macky sall etat bi yeup bilahi bou yalla wakhé wal asri ina linsana lafi khousri warnañiou ko geum dh allah dina réglé yeup.. Yalna allah xaré aldiana firdawsi pape sarr amine🙏

  • @mohamedleye5166
    @mohamedleye51663 жыл бұрын

    leufall ndeye police Sénégal way wa rew amoull louwa😭😭😭

  • @waffasow133
    @waffasow1336 жыл бұрын

    Bilay c horrible je n'arrive pas a retenir mes larmes c honteux que la police face ça a des jeunes innocents

  • @mgndiaye1339
    @mgndiaye13396 жыл бұрын

    Que justice soit faite

  • @fantasoumbounou6161
    @fantasoumbounou61615 жыл бұрын

    Bilahi sama khôl fesna trop k justice soit faite insallah paix à son âme 😭😭😭

  • @ndeyeditnawaresow4582
    @ndeyeditnawaresow45824 жыл бұрын

    Dur Notre Senegal triste

  • @lallaaichakoulibaly5226
    @lallaaichakoulibaly52265 жыл бұрын

    Soubhanallah😭😭😭😭😭😭

  • @cheikhyade2316
    @cheikhyade23166 жыл бұрын

    Thiey adouna koula wara ar molay ray

  • @oumarfall1540
    @oumarfall15405 жыл бұрын

    Si bane rew lanou nék population bi amatounou sécurité police noy ray légui yalla guiss na lepp

  • @mirimakhou3546
    @mirimakhou35466 жыл бұрын

    Sama khole dafa diékhe torop.

  • @oumygaye9354
    @oumygaye93546 жыл бұрын

    Metina😢😢

  • @fintyndiaye2369
    @fintyndiaye23696 жыл бұрын

    Aÿ domaram lagnou police thiaroye takh guen ma bagne thiaroye vous etes des assassins

  • @djibrilndiaye4801

    @djibrilndiaye4801

    6 жыл бұрын

    wa thiaroy nion niak faye daa rek thiot ndm le mm moment bouniou bolewone jeunou quartie bi teup dioubali ndm police ba taal ndm dotoul amati bilahii sama khol taaguenaa troop insbi magui diooye comme pa possible aye domeram laniou rek raynaniou domou diambour nii noooo

  • @aminatacisse9128
    @aminatacisse91284 жыл бұрын

    Waw police sou Sénégal Ay domeram laniou gnou wara sauver Di Ray founou diem la famille boubou bayi nagnou dem ba diek

  • @mamadousouare167
    @mamadousouare1676 жыл бұрын

    Les policiers du Sénégal sont très maisan boulen Bay 😭😭😭😭😭😭

  • @sambaniang6459
    @sambaniang64596 жыл бұрын

    na senegalai yeup djioug si li nanou defarat senegal mo geunn ndakh nioun wa senegal dano rew trop mo takh li yeup diniou dall ni wa deuk bi mell rek la wa police mell guisagounou darra sakh

  • @ndeyediakhate1433
    @ndeyediakhate14336 жыл бұрын

    Bilay c'est triste !raay si erreur rek.

  • @rmjohnson3577
    @rmjohnson35776 жыл бұрын

    Injustice pure...topou lène policiers yi ba seusse...jusk'à la cour de la haie. Cet acte ne doit pas rester impuni

  • @mboldieng234
    @mboldieng2344 жыл бұрын

    Nioune si bane deuk lane nek police thiaroy yallla mingui Leni khar

  • @ousmanesidibe9250
    @ousmanesidibe92506 жыл бұрын

    Ana wa droit l'homme yi nagn wakh ndey si li c pas normal police bi dafa am ay domerame you bone niou nek si bir

  • @fallougallassdiop2516
    @fallougallassdiop25165 жыл бұрын

    Non Sénégal dou dem karéma loye dama ndioum Sénégal badolò yi niooye sonnou rek

  • @mariamambaye7738
    @mariamambaye77384 жыл бұрын

    yalla na yalla atè

  • @massfall1817
    @massfall18176 жыл бұрын

    Léne dé khamnako agression ak cambriolage yi am dackar man guénéwoumasi policiers yi nék si banlieue bi dasé am ay croupe de mal faiteurs il faut police des polices am Sénégal

  • @fafajohn3406
    @fafajohn34065 жыл бұрын

    Portez plainte et que justice sois faite , ne laissez pas cette affaire , ce n'est pas normal sa c'est de l'abus de pouvoir Honte à la police sénégalaise

  • @saf-tnexx6731
    @saf-tnexx67316 жыл бұрын

    Dia Diawo mane sama dalle sakh mousoul dpugou gal aussi ngniye dougou gal amoungnou loulène gueneul sama khol moo djiekh mème paa un moi ngnou ray ngniata nit dafa mèti😢😢😢

  • @ousmanesow9930
    @ousmanesow99306 жыл бұрын

    Li senegal rk la ame il faux ñou manko dokhane ndeyou police yi

  • @imaneanne9464
    @imaneanne94645 жыл бұрын

    Que justice soit fait comme le mali on voter la loi kou ray niou ray la na senegal diouk tout le monde bou kène dèss si keur yi na nieuup guène fait face à la police on nous tue mais on ne nous déshonore pas cest du bassèsse assassin criminel que vous etes en tant que sénégalais

  • @cheikhbousso3487
    @cheikhbousso34876 жыл бұрын

    C'est pas normal policier sénégalais c'est pas le droit pour toi non non non quel pays le procureur il faut que ça travailler ça Sénégal no

  • @diagnegaye6463
    @diagnegaye64636 жыл бұрын

    yonbouna nak trope gnie haye domarame policier

  • @mbayewadelofficiel6585
    @mbayewadelofficiel65856 жыл бұрын

    niaka xam say droit mo métti et mank de professionalisme. no j peu plus me tenir

  • @papandiagadieng6168

    @papandiagadieng6168

    6 жыл бұрын

    Papa deug le yako diour waroul yombee ni dakhte li diadouwoul khana sakh boudoul dara niou soutoural kou jiguene yen familles bi lay wakhal boumou nilee nonou day yombou

  • @evangom2220

    @evangom2220

    6 жыл бұрын

    Thiay adouna yowmalkhiam Dina méti awma bane mode laniou nék li niawna métina

  • @nanicenice5654

    @nanicenice5654

    6 жыл бұрын

    Wa nation unis loumou khar mongui setane Sénégal khawma l'ordre publique la wala désordre publique yalla nako yalla yeureum

Келесі