Témoignage des amis proche du jeune tué à diameguen trés remonté contre Sitteu

Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
/ @dakarinstant
l'information à l'instant, n'oubliez pas de vous abonnez. ✆:(+221) 33 898 53 09 / 77 561 55 46 / 77 506 85 74 WhatsApp : 77 490 11 06 pour plus d'infos merci.
Série - Karma - Saison 2 - Episode 32 - VOSTFR
Le « Seuye Si » de Fatel chez son mari Ngaka Blindé à Guediawaye accompagné de…
Dérapages - S2 - BA EP 29 - LE RETOUR !
Journal de la can 2022 ( Senegal vs Malawi )
Mariage de fatel: Émouvant conseil de Ya Awa Rassoul, Aicha kone, Katy «Boumou deglou ay…
Cérémonie clôture Karma Saison 2:L’annonce surprenante de Bathie Massamba,Majid,Lamine,Maï aux fans
INFIDELES - Saison 3 : Bande Annonce *VOSTFR*
Le Polygame - Episode 162 Le mariage religieux
Partie 2 - MIDI + avec Pape Cheikh Diallo - invité : Oustaz Modou Fall - 07 Janvier 2022
Anniversaire Surprise de Diamy Gueye á son Mari Tonton Medoune Diouf
TOUT CE QUE VOUS AVEZ MANQUER DU COMBAT BALLA GAYE 2 VS BOMBARDIER
Prank Star épisode 5 Ouzin Keita Moma Eumbeul
Mariste : Pris en flagrant de v0l, cet homme brutalise la gérante et emporte 3 millions FCFA
Le Polygame - Episode 182 Sabar Tannbir
Journal de la can 2022 ( Sénégal vs guinée )
Amina Poté sur son divorce: Tass na wayei douma ndialokaat..
ALLO DG - SAISON 2 - EPISODES 1 et 2 (VOSTFR)
Mali : les autorités font une démonstration de force
Les frontières de Guinée restent ouvertes au Mali
Diamy Gueye Toth Na Anniversaire de Tonton Medoune Diouf
🔴Urgent :première Sorti Après Son Agression, Mouride Boufi Taxawe sopi..Chiékhe oumar Diagne Lamou
CAN 2021 : MALAWI 🇲🇼 VS SÉNÉGAL 🇸🇳 EN DIRECT LIVE COMMENTÉ / LE RÉVEIL DES LIONS ?

Пікірлер: 369

  • @bigjohn1673
    @bigjohn16732 жыл бұрын

    Ta raison vérité absolue bonne continuation que dieu te protège. Paix à son âme

  • @massambasylla5306
    @massambasylla53062 жыл бұрын

    Borom lou noir bi il faut lui comprendre kharitam niniouko rayè mo méti mo takh

  • @seynaboudiouf3765

    @seynaboudiouf3765

    2 жыл бұрын

    Pourtant il a raison siteu lepou si mom la

  • @bassou77

    @bassou77

    2 ай бұрын

    Seuteuteuteu sonal ngene siteu​@@seynaboudiouf3765

  • @docteurkante5447
    @docteurkante54472 жыл бұрын

    Changer votre comportement c’est mieux bandit amoul mouthiou Yalla nako Yalla yeureum té kharé ko Aldjana Firdawsi 🙏

  • @samayayesamakharite4831
    @samayayesamakharite48312 жыл бұрын

    Yalna Yalla conscientise souniou jeunesse bi .Thieye Sénégal

  • @ndiawardieye6323
    @ndiawardieye63232 жыл бұрын

    Kholal boy yi nignouy wakhé doyna waar En tout cas Parents yi nagnou dieul séne responsabilité ci sén dom yi mogueune lii

  • @boundawdiakhate2801

    @boundawdiakhate2801

    2 жыл бұрын

    bou lamba bi diékhé gnome gni gnoyyy agressé nitt yi bi passer nak souniou borom Molène werrrr

  • @mamadoundiaye5230

    @mamadoundiaye5230

    2 жыл бұрын

    Faut le comprendre défa ham louko méty

  • @mayajarju8479
    @mayajarju84792 жыл бұрын

    Siteu kokou da nekhoul sa rakk merci bro iow wakh dji rafet na yalla nako yalla yeureum

  • @bassou77

    @bassou77

    2 ай бұрын

    Sa way yene sonal ngene siteu

  • @noumbefall7073
    @noumbefall70732 жыл бұрын

    Li métina yalla n'a justice déf liguéyame sa maman a beaucoup pleuré

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu58892 жыл бұрын

    Kou sol lou Noir lii comprendre lénko Rék naysan boo amai sa xarith niou Défco Lii fawnga sisou ray Nith dou Thiaxane Dei 🧏

  • @khadimndiaye6732
    @khadimndiaye67322 жыл бұрын

    Brom lou noire bii dafa merr rekk naxx kharitam laniou rayyy fokk khol bii sott nguen comprendr ko rekk mai nekoul bandit bandilou khol lay waxé rekk nax niou rayy kou bokk si yaww dafa metty surtout sa kharite sou and bi deuguo

  • @jazaka3178
    @jazaka31782 жыл бұрын

    En mon avis même les Complices doivent être punis , ce qu'ils disent c'est grave

  • @gorguifaye2256
    @gorguifaye22562 жыл бұрын

    Yalnako yallah yeureum te kharéko aldiana may neup xolou mougne métina trop

  • @ibrahimagaye529
    @ibrahimagaye5292 жыл бұрын

    Merci Waw

  • @charasakina9594
    @charasakina95942 жыл бұрын

    En tout cas faut pas juger les gens sur leurs façons de parler ou s'habiller et autres conduire une charrette ne veut pas forcément dire être un bandit et la n'est pas le thème a mon avis et rien ne peut justifier un crime ou cacher un criminel et personne n'est au-dessus de la loi le petit Gabou quelque soit comment il était de son vivant il méritait pas mort aussi atroce et comme ya des témoins de l'acte pourquoi ils n'ont pas appelé les sapeurs ou la police

  • @diattaabdoukoulingo2826

    @diattaabdoukoulingo2826

    2 ай бұрын

    Siteu est complice il doit etre convoquer par la police

  • @zen05111
    @zen051112 жыл бұрын

    Mes condoléances les gars 😢 c triste 😭 boy yi ils ont l’air indice mais wakhou kou conscient rek lañ fi wax mais courage les gars

  • @alsenydiallo9699

    @alsenydiallo9699

    2 жыл бұрын

    Faut pas juger les apparences

  • @zen05111

    @zen05111

    2 жыл бұрын

    @@alsenydiallo9699 je n’ai pas fais de jugement…

  • @boundawdiakhate2801

    @boundawdiakhate2801

    2 жыл бұрын

    ay bandits laniou gnome nieuppp

  • @papaomarthiaw9453

    @papaomarthiaw9453

    2 жыл бұрын

    @@boundawdiakhate2801 je te rappelle qu’il y’a mort d’homme! Doff nguén trop

  • @jb_correa

    @jb_correa

    2 жыл бұрын

    @BOUNDAW DIAKHATE DIEU est le seul juge

  • @bassfallfall8157
    @bassfallfall81572 жыл бұрын

    Ndeyssan vous avez parfaitement raison mai le banditisme n'a pas de sens bayi lèn ko mou dè sii prison boo

  • @baalassane9120
    @baalassane91202 жыл бұрын

    thieye senegal yeureme na futur génération yi di niawe

  • @cheikhdia9551
    @cheikhdia95512 жыл бұрын

    Merci papa merci maman ♥️ Yarat len sen domm dji t bagn len abandoner li niawna si imajou jeuness

  • @thierno-seydoumbaye8996
    @thierno-seydoumbaye89962 жыл бұрын

    En l’écoutant parlé ça se voit que y’a un gros travail à faire sur la conscientisation des jeunes dommage 🤦🏾‍♂️

  • @laperlecmoi5995

    @laperlecmoi5995

    2 жыл бұрын

    Wallah

  • @sadiobandia947

    @sadiobandia947

    2 жыл бұрын

    Ceux qui doivent faire le travail de terrain ne savent pas que développer un pays c'est par le bas avoir des citoyens modèles et responsables mais aussi miser sur le plein emploi des zones industrielles avec cette morosité c'est ça le résultat

  • @gorguifaye2256
    @gorguifaye22562 жыл бұрын

    Super Borom Yalnako yallah yeureum

  • @gorguifaye2256

    @gorguifaye2256

    2 жыл бұрын

    Capp bi

  • @ousmanesow6736
    @ousmanesow67362 жыл бұрын

    Bouguéne Di diokh sèn micro dèlèn ko diokh ay kilifa. gni ay khalè laniou en plus sèn xol laniouy wakhé

  • @diegaye8541
    @diegaye85412 жыл бұрын

    J'ai peur pour la jeunesse de mon pays li khew metina wanteh dina khewatt ndakh yi comportement you indice doyna war

  • @mondiaye2207

    @mondiaye2207

    2 жыл бұрын

    Gno bok guiss bilahi

  • @doudoucisse6485

    @doudoucisse6485

    2 жыл бұрын

    Saway comportement dafay nakhe khassim ba kanam gui Soko xolé Doula diokh kanamu assassin

  • @bayeniass5633
    @bayeniass56332 жыл бұрын

    Enquête bou srx mo warraaa ame si cas bi franchement justice

  • @pablogabrielscobar8097

    @pablogabrielscobar8097

    2 жыл бұрын

    Bilay

  • @adjambengue1624

    @adjambengue1624

    2 жыл бұрын

    Li la wakh waroul sakh takhaw

  • @diattaabdoukoulingo2826

    @diattaabdoukoulingo2826

    2 ай бұрын

    Niou téwé crime yeup danioulene wara attendre

  • @ibrahimatraore223
    @ibrahimatraore2232 жыл бұрын

    Yalnako yalla yeureum teu khareko adjana . J'avais toujours souligner la violanze des jeunes sur tous les supporters , moi je ne crois pas an ( NDOGAL ) mentenan aux Sénégal LOU WAY NEKH DEF BOUNOU PARÉ NE NDOGAL c'est du n'importe quoi . Beugue guislenma djarna nguay banbandilou beu Ray nit . Malheureusement aux Sénégal nous avons l'habitude de négocie les choses ( NOO TATOUKO NDOGOL LE ) . Les gens continue a morir notre gouvernement a autre occupations POLITIQUE . POUR FINIR ÇA ILS FAUT LA PENNE DE MOR . PER MAX BAYIL NDEUP NDEUPEUL TE WAKH DEGUE WAKH SA WA ECURU NOU YAROU TE BAYI DOFFOFLOUBI

  • @ousseynoufall5004

    @ousseynoufall5004

    2 жыл бұрын

    ku baax ndogal lu aam la

  • @lomediacomdigitale8041

    @lomediacomdigitale8041

    2 жыл бұрын

    En tout cas, ce meurtre doit etre elucidé

  • @lomediacomdigitale8041

    @lomediacomdigitale8041

    2 жыл бұрын

    3 questions. 1, et Sitteu dans tout ca? 2 Est ce Sitteu qui a conduit le cadavre @ lhopital, 3 Sitteu a livré le jumeau à la Police

  • @kebadia6284
    @kebadia62842 жыл бұрын

    Amna sólo 👌🙏❤️

  • @theblackmamba434
    @theblackmamba4342 жыл бұрын

    Akh siteu c'est un vrai domoramm limiy deff akh limiy wakh dara bokussi

  • @bassou77

    @bassou77

    2 ай бұрын

    Yaw boy diakarlo ak siteu waxx ko domeram mou degg sa ndey

  • @user-qx9hb3cf3s
    @user-qx9hb3cf3sАй бұрын

    Amolene bene éducation nekkelene aye nite yalla na yalla yeureume ki fatou

  • @ismailasy5406
    @ismailasy54062 жыл бұрын

    Il parle sou l'émotion il faut le comprendre.

  • @oumidiallo5074
    @oumidiallo50742 жыл бұрын

    Jeunesse bi kholate len sene bop niiit dafaye correct mais incorrect boye wakhe mague sakhe doula meune deglou defar Lene séné avenir am moudie nou rafet

  • @magattedieng1180

    @magattedieng1180

    2 жыл бұрын

    Dagg gou wér nga wax xalè yi danio melni dof xammé wouniou yay Wala bay

  • @oumidiallo5074

    @oumidiallo5074

    2 жыл бұрын

    @@magattedieng1180 bilakhi max lii dafa eupe rewww amoule bene ndiarigne

  • @assanesamba8560
    @assanesamba85602 жыл бұрын

    Deugue nga wakh tu as bien parlé frère boulén bén mbeur diaral yén yii gueum sa boop rek mo solo

  • @deugrekk1927
    @deugrekk19272 жыл бұрын

    Wakhna deugue moko taye khalé bou ndawe nga eupeko dolé fouff diko diame si poute baparé di bakou di sagua dou yone siteu kou bakhela mé nakk dafa ware di wakh boye yi deugue lolou moye deugue que la terre lui soit légere

  • @mansourkane2934
    @mansourkane29342 жыл бұрын

    Tu a raison

  • @mamadoumansourfaye4684
    @mamadoumansourfaye46842 жыл бұрын

    Siteu dadone bagn affaire yi dégénéré rek yaram sou bayiwone chérif keur mama lamine kone décès yi dou yam si béne

  • @ousmanesow6736

    @ousmanesow6736

    2 жыл бұрын

    Siteu limou déf nonou rék la meuna déf

  • @khadijasene9134

    @khadijasene9134

    2 жыл бұрын

    Boudone rakkam lagne rayy dou démé nonou gnou waxal yalla

  • @sonkowalabakane5340

    @sonkowalabakane5340

    2 жыл бұрын

    @@khadijasene9134 legji lo beug mou bayiko kofa thiow li geuna barri

  • @senegalais.
    @senegalais.2 жыл бұрын

    Bandit experiznce le bandit li le bandi la le..... Etc... Legui nekeu bandit bane gnerigne le am ? Diay dolé bi si banlieu bi bandi bandilou bi bane gnerigne le am ? 🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @fatouniane9697
    @fatouniane96972 жыл бұрын

    No mètina trop mei cherif ak lou GABOU meuneu def warone gua dawal yeurmandè si mom

  • @mofa3838
    @mofa38382 жыл бұрын

    C'est vraiment triste

  • @amadoufatouba2985
    @amadoufatouba29852 жыл бұрын

    Yalla nako Yalla yeirim

  • @clairemari7292
    @clairemari72922 жыл бұрын

    Ndeyssane paix à son âme c triste et grave

  • @MohamedSoce
    @MohamedSoce Жыл бұрын

    Yalla na ko yalla karé aldiana 😢😢

  • @elimaneabouhane
    @elimaneabouhane2 жыл бұрын

    No harit da for nak 🙌

  • @momogueye2508
    @momogueye25082 жыл бұрын

    Qui deff première témoignage bi dafa dawlo sama yaraam vrai kharite la nagnou ko gnanal yalha🙏

  • @davidofaye468
    @davidofaye4682 жыл бұрын

    Bilay yaw

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu58892 жыл бұрын

    Yéne ndiouy commentaire Dii Teukonté Déf lénn nakeu Dei reuwmii Barké mam Cheikhra Fall koufii saytané Diay Banga rayfii nith moy Parénga thi koso bii ngay Décède 🧏lou lérr Laléne wax🧏

  • @djibrilndiaye2754

    @djibrilndiaye2754

    2 жыл бұрын

    Boybi soll lou noir li nittou deugeuleu

  • @ndeyetoutyndiaye1047

    @ndeyetoutyndiaye1047

    2 жыл бұрын

    Lou léeeer

  • @boubacarlimanbadiane9569
    @boubacarlimanbadiane95692 жыл бұрын

    Rip

  • @abdoudiop5163
    @abdoudiop51632 жыл бұрын

    siteu dafa dioume trop waroul wakh ni acident la parceque soudone rakam douko wakh emplis kou raye tayko nanouko yobou arene national rayko legi raye bi diekh bilahi

  • @alassanedieng2657

    @alassanedieng2657

    2 жыл бұрын

    Si frère

  • @makeitreal6918

    @makeitreal6918

    2 жыл бұрын

    Il a raison

  • @thiernohane1357

    @thiernohane1357

    2 жыл бұрын

    Ioe arènes nationale rk gua guiss

  • @abdoudiop5163

    @abdoudiop5163

    2 жыл бұрын

    @@thiernohane1357 wawaw

  • @lucienmendy2138

    @lucienmendy2138

    2 жыл бұрын

    Bayilén hypocrisie bi Esk bou doon sa frère tamit mo raay comme tu le dit pour Siteu di nga ko diebeul Population pour niou raay ko Fii deukou yoon la li Siteu deff moy li exemplaire di deff si quartier

  • @isafaal801
    @isafaal8012 жыл бұрын

    Ndeysane gnakk sa proche dafa meti

  • @noumbefall7073
    @noumbefall70732 жыл бұрын

    Maman yalla mayela kholou mougne

  • @tonysmith5489
    @tonysmith54892 жыл бұрын

    Bayi lene mbeur yi tes dem job bi mo guene ay sacrifice rek la nouy def en plus lamb dafa haram yalanako yalla yeureum

  • @lomediacomdigitale8041

    @lomediacomdigitale8041

    2 жыл бұрын

    3 questions. 1, et Sitteu dans tout ca? 2 Est ce Sitteu qui a conduit le cadavre @ lhopital, 3 Sitteu a livré le jumeau à la Police

  • @sonkowalabakane5340

    @sonkowalabakane5340

    2 жыл бұрын

    @@lomediacomdigitale8041 bayil siteu rayoul ray lou woull

  • @dergouneder1840
    @dergouneder18402 жыл бұрын

    Metina li bilay 😭😭😭

  • @ibrahimaniane6508
    @ibrahimaniane65082 жыл бұрын

    Les gars vous avez raison ,action bii sou demeniii konn ayy nafeeck reek nio fa neekonn ,siteu moom konn loumouy wotee nekoul sii momm

  • @mamadoulaminesonko987
    @mamadoulaminesonko9872 жыл бұрын

    Deugue rek la wakh

  • @veriteabsoluedeugneekhoul1720
    @veriteabsoluedeugneekhoul17202 жыл бұрын

    Merci le gars en noir . C'est des voyous . Siteu nafekh leu

  • @iboudia7741

    @iboudia7741

    2 жыл бұрын

    Li siteu déff Moy deug

  • @Onomar

    @Onomar

    2 жыл бұрын

    @@iboudia7741 arrête lou siteu deff dou deug il ne devrait pas déplacer le gars il devrait appeler les sapeurs pompiers 🚒 et la police c’est un meutre .

  • @futurepro4862

    @futurepro4862

    2 ай бұрын

    ​@@Onomarmais daff ko beuguone sauvé rk

  • @saaabaaa755
    @saaabaaa7552 жыл бұрын

    Ki limou wakh dou wakhou doff de dafa warona bayi yone def ligeyem

  • @malikgueye7276

    @malikgueye7276

    2 жыл бұрын

    Deugue rék la wakh

  • @sambatoury593
    @sambatoury5932 жыл бұрын

    Amna lo khamne khel nangouwuko bamakh rek mou danou deh

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop62162 ай бұрын

    Ndeysane mitina bilayie

  • @is_back_2219
    @is_back_22192 жыл бұрын

    Vraiment wa dji daniouko wara ray lii dfa yomb ray domi diambou si zéro takhaw di backou ak lo meuneu diàppal ray bi meunna niàk mais je dis aussi ñafa nékone tous sont des complices

  • @ibrahimaniane6508

    @ibrahimaniane6508

    2 жыл бұрын

    Lolou la dee broo yalla souniou moné kou raay dagn la wara raay moudieex takk

  • @doudoundiaye2075
    @doudoundiaye20752 жыл бұрын

    Bima guissé Siteu nane accident la xamnei xam nassi lou beuri nakh lieu de crimes amo droit déplacé corps car la police scientifique doit venir pour inspecter les lieux teh yeine dagueine wara yewou bayi mbeur yii ak politicien amalou niouleine beine avancement

  • @pablogabrielscobar8097

    @pablogabrielscobar8097

    2 жыл бұрын

    Bilay 😢

  • @serignefall131
    @serignefall1312 жыл бұрын

    mais famille diambour bofa deme pour suporte te bougou nioula do dem gnibi wala suporte mbuer day force

  • @boundawdiakhate2801

    @boundawdiakhate2801

    2 жыл бұрын

    😂😂😂

  • @laperlecmoi5995

    @laperlecmoi5995

    2 жыл бұрын

    MoMA diakhal mbeur AK politiciens gnon yame

  • @alsindor81
    @alsindor812 жыл бұрын

    Si ces affirmations so vrais kone Siteu doit être interpellé pour complicité de meurtre

  • @iboudieng7106
    @iboudieng71062 жыл бұрын

    C’est que boys yi nio wara bayi yeufou bandits bandits lou,même séne langage tu le sent,ki raye déf na lou niaw mais yone ték nako lokho,Siteu diam la dokh boy yi nio wara bayi yeufou bandits amoul mouthie

  • @bintandoye4802
    @bintandoye48022 жыл бұрын

    Fier de toi boy

  • @boyetownfromdkr5287
    @boyetownfromdkr52872 жыл бұрын

    Siteu pour môme mo eupou khél nieup moye wakh katou deug bii bala ma déh mouye diokhé ay leçon

  • @CR7_Mane
    @CR7_Mane2 жыл бұрын

    Depuis le Début lako wakh Autorité nagne def sen liguey nimou waré dakh Histoire bi paré woul bay diekh té Adamo limou wakh day yok problème rk

  • @matarsene602
    @matarsene6022 жыл бұрын

    Yalna yala yeureum ko waye kharitame yi daloukhelou keneu

  • @beydysakhocurdelion
    @beydysakhocurdelion2 жыл бұрын

    Boy Bi sol lou noir li il a raison situe yone dako wara enquêté boy bi degne ko rey si bir keur keine amoul droit dieul corps bi di ko yobou hopital keine warou ko lale loudoul police ak sapeur pompier dieul ki rey dougeul ko sa bir keur dieul corps bi yobou hôpital c est très grave malheureusement Afrique moy lolou 🤦🏾

  • @ousmanesarr756

    @ousmanesarr756

    2 жыл бұрын

    Commissaire mola guena kham lane mo takh siteu denthie wadji ba affaire bi calmé mo dogg ko livré police wadj niou ray ay kharitam ay diaasi lagnou yorr di weur sekhou mama lamine bi kone siteu bou dokhalé woul ni nane la wara dokhalé ?? Khamolen dara si histoire bi ngen beug nek fi di doul

  • @beydysakhocurdelion

    @beydysakhocurdelion

    2 жыл бұрын

    @@ousmanesarr756 lol bro yaw momou sakh khamo si darra mane diemou ma si kham dara Li niary partie yi wakh si la soukandikou siteu ak kenene la yamalé yeuf yi bimou amé si sass yi legne warone wo police ak sapeur-pompier yi mais corp bi keine warou ko wone lale wadji keine warou ko yobou fenen di ko garder si bir keurgui la worone tok keine begne ko lale meune nga wakh sa khalate sans depassé nit ki t khamoko dou yeufou diantal man

  • @moustaphadiop1834

    @moustaphadiop1834

    2 жыл бұрын

    @@ousmanesarr756 bilay frr khamou niou dounu noppi

  • @futurepro4862

    @futurepro4862

    2 ай бұрын

    Boy bi dewoul wone sur le champ si yone hôpital la déeh wé

  • @mariemusicof1881
    @mariemusicof18812 жыл бұрын

    Je répète et je le répéterai encore une fois le jeune à été utilisé pour le sacrifice du combat mais ça n'a pas abouti car le jeune en noir a dit qu'ils sont parti le jeter.....PAIX À TON ÂME GABOU

  • @ousseynoufall5004

    @ousseynoufall5004

    2 жыл бұрын

    yaw iska wéer ga ?

  • @ousmanekone7115

    @ousmanekone7115

    2 жыл бұрын

    @@ousseynoufall5004 ki kay weroul khamoul loum wakheu sakh

  • @ZZpydio221

    @ZZpydio221

    2 жыл бұрын

    Ya meune doul losi kham putin 😒

  • @ousseynoufall5004

    @ousseynoufall5004

    2 жыл бұрын

    @@ousmanekone7115 vraiment dafa ame gnou gnawe gnorte rék té meuna xalat lou niaw

  • @mbalkakognedof5866

    @mbalkakognedof5866

    2 жыл бұрын

    Nite day wah louka waur

  • @fatoudiouf8756
    @fatoudiouf87562 жыл бұрын

    Ki vré assassin la mélni kou yor khar niawna trope

  • @ousmanediadiembodji9905
    @ousmanediadiembodji99052 жыл бұрын

    Bilakhi deug rek gua wakh dafa beuri lakh lakhal

  • @ndongasamb4035
    @ndongasamb40352 жыл бұрын

    nane raye ndeyame wayy

  • @moussaseye8684
    @moussaseye86842 жыл бұрын

    bis bo laalé Siteu

  • @doundou_diam4953
    @doundou_diam49532 жыл бұрын

    yarou lene mogueune.

  • @ristosgueye425
    @ristosgueye4252 жыл бұрын

    no boy yiii rien à perdre

  • @falybadji8954
    @falybadji89542 жыл бұрын

    Antouka siteu limou moudié la warone dieuguai koi noy fatai nitt kou ray nitt sa keur

  • @assanegueye28
    @assanegueye282 жыл бұрын

    Yene yuikoye diokhe micro yénayou toye

  • @dabasarr2079
    @dabasarr20792 жыл бұрын

    Bilay je me dit que setane amna si vraiment c mon point de vue nak

  • @alphousseynoudiallo517
    @alphousseynoudiallo5172 жыл бұрын

    Siteu domoram leu moko tey complice là

  • @makeitreal6918

    @makeitreal6918

    2 жыл бұрын

    Vérité absolue

  • @ndeyekhadyfaye641
    @ndeyekhadyfaye6412 жыл бұрын

    Borome lou noir lii dafa ame louko méti déklo lénko ak khél... loutakh nioukoye diw d'huile lolou dou yone Siteu waroutone sétane lolou.... ta dako yékha diébeul police

  • @deugrekk1927

    @deugrekk1927

    2 жыл бұрын

    Guiss nga senegalais douniou até deugue khalé bou ndawe nga eupeko dolé fouff diko diame si poute baparé niouni tayouko Siteu mo ware di wakh deugue aye xaritame lolou moye deugue

  • @barhamasow2065

    @barhamasow2065

    2 жыл бұрын

    @@deugrekk1927 Limoye Senegal de Yalla terre lou niawe ngene koye deff nane Ndogallou Yalla la Senegal mo newe niouye wahe deugeu

  • @veriteabsoluedeugneekhoul1720
    @veriteabsoluedeugneekhoul17202 жыл бұрын

    Borom fass yi 🐴 ey agresseurs lagn. Ils m'ont agressé

  • @mbaye_ndiaye3800

    @mbaye_ndiaye3800

    2 жыл бұрын

    Bayil ndey doull😅😅beugue ay j'aime rek

  • @veriteabsoluedeugneekhoul1720

    @veriteabsoluedeugneekhoul1720

    2 жыл бұрын

    @@mbaye_ndiaye3800 barki yallah ils m'ont agressé coté malika plage nonou sama auto panne gnou gnow ak ey paka

  • @veriteabsoluedeugneekhoul1720

    @veriteabsoluedeugneekhoul1720

    2 жыл бұрын

    @@mbaye_ndiaye3800 yaw mom bo deme dawal kateu fass 🐴ngua

  • @kadelbiagui4338
    @kadelbiagui43382 жыл бұрын

    siteu c un homme digne honte courageux. bou défoulene lolou dou bakh

  • @fifitraore4028

    @fifitraore4028

    2 жыл бұрын

    Un corp ne dois pas ce faire déplacé k mouy ami ou frere surtout en cas de meurtre

  • @futurepro4862

    @futurepro4862

    2 ай бұрын

    ​@@fifitraore4028 déplacé woul corps c en voulant le sauver boy bi si yone hôpital bi la décédé mais pas si keur gui

  • @sowamina1725
    @sowamina17252 жыл бұрын

    Ya wakh deugue. Koula door fayoul

  • @mhdasensiodia8691
    @mhdasensiodia86912 жыл бұрын

    Yalla nko yalla yeureum metti na lolou mais violence dagn si wara dioukk

  • @djilikebe5353
    @djilikebe53532 жыл бұрын

    Âme léne yar way néck bon excenple

  • @mrmendy7317
    @mrmendy73172 жыл бұрын

    Borom lou noir li wax katou deugg leu … Siteu ak kénéne Kouko neub . Yeufou Deum la déff

  • @ibrahimafaye8446

    @ibrahimafaye8446

    2 жыл бұрын

    Mètina m siteu limou df nonou la ki rayè mo irresponsable si bopam 🤦

  • @ndeyegueye254
    @ndeyegueye2542 жыл бұрын

    thieuy rew mii

  • @mansourkane502
    @mansourkane5022 жыл бұрын

    Porter lene plainte Siteu DOU YONEEEEE

  • @Laye396
    @Laye3962 жыл бұрын

    Deguena niounane tayouko Moko taye depuis open presse bi mongui bouhe boy bi dako diapale haine

  • @veriteabsoluedeugneekhoul1720
    @veriteabsoluedeugneekhoul17202 жыл бұрын

    Dangn ko diapalone rancune motakh gnou reyko

  • @massambasylla5306
    @massambasylla53062 жыл бұрын

    Cest dur nianal lenko

  • @serignediop2460
    @serignediop24602 жыл бұрын

    Degue rk la wah

  • @maimounasene6488
    @maimounasene64882 жыл бұрын

    Mais située aussi ce qu’il a fait crie la pourquoi garder un meurtrier chez lui il fallait l’amèner à la police immédiatement

  • @sirandiaye2753
    @sirandiaye27532 жыл бұрын

    Yeineu yam ayyy vrai bandit gueine kiii deeee yalla nako sugnu borom yeureum wayé bandit la

  • @gagnesarr7120

    @gagnesarr7120

    2 жыл бұрын

    Nitt sou guéné aduna dangay wax si mom Lou rafet

  • @serignembackediaw7710
    @serignembackediaw77102 жыл бұрын

    Lim wakh deugue bou wér naniou bagna farr rék

  • @saerdiop4482
    @saerdiop44822 жыл бұрын

    Il as raisons hein sérieux sa fait mal même bakann mom dou ay fooh

  • @malkomx9503
    @malkomx95032 ай бұрын

    Siteu doit être interpellé Complice leu danko wara arrêté sakh

  • @massdieye3238
    @massdieye32382 жыл бұрын

    Siteu danou nga nak ninga dokholé dou nonou

  • @sakhodiamasakhodiama8368
    @sakhodiamasakhodiama83682 жыл бұрын

    Le gas en noir degeh kép nga wakh nak. Khana di gniane gniawtéf yi dedou gnou ak diam si barkep sindidi🙏🙏🙏

  • @assanendiaye5640

    @assanendiaye5640

    2 жыл бұрын

    Saway deet ki dafa merr rek mais apres rethiou nako

  • @sakhodiamasakhodiama8368

    @sakhodiamasakhodiama8368

    2 жыл бұрын

    @@assanendiaye5640 wa d’accord mais ak numu mënti démé haqq minal haqqi mo gnëk té moy mudju yesslouwat🙏🙏🙏

  • @naingbabakar4285
    @naingbabakar42852 жыл бұрын

    Boye site yi ay Banedie lanie

  • @ristosgueye425

    @ristosgueye425

    2 жыл бұрын

    youyou makk sakhhhh

  • @fifitraore4028

    @fifitraore4028

    2 жыл бұрын

    Bien dis

  • @serignesaliouniang4227
    @serignesaliouniang42272 жыл бұрын

    Siteu limou wakh warouka wakh

  • @bambasene5971
    @bambasene59712 жыл бұрын

    Ok

  • @nattyirei6762
    @nattyirei67622 жыл бұрын

    Jajeuf waay jambar

  • @ndiayeibrahima9876
    @ndiayeibrahima98762 жыл бұрын

    Diamgeune da bari aferou bandit deug nekhul

  • @alioudiagne5373

    @alioudiagne5373

    2 жыл бұрын

    Bilahi iow

Келесі