Son neveu en Prison: L'oncle de Lac 2 fait des révélations "Danio Sétan" sur 59 Millions nous...

Son neveu en Prison: L'oncle de Lac 2 fait des révélations "Danio Sétan" sur 59 Millions nous avons 35Millions

Пікірлер: 56

  • @Ndiaga-mw6zc
    @Ndiaga-mw6zc28 күн бұрын

    Noo Sénégal nekhna lek khalisou diambour ba pare na fay ana foum ko def ana

  • @fatoubinetoulam275

    @fatoubinetoulam275

    28 күн бұрын

    Yomb na dher lek khalissou diambour gnou war la fayal

  • @mbayendiaye8825

    @mbayendiaye8825

    28 күн бұрын

    C'est ça le Sénégal 😂😂😂

  • @waxkatoudeug
    @waxkatoudeug28 күн бұрын

    Faut pas nous emmerder ! Ndimbeul dou force. Il n'avait pas à rentrer dans des magouilles. Et puis tous ces jeunes qui ont perdu leurs millions vous en dites quoi? Kat léne ndéyam feulé waay

  • @SalyNdiaye-ef9su

    @SalyNdiaye-ef9su

    27 күн бұрын

    Walahi yéna woumako dé yalla nako yalla guéné si limou nék nite day doylou

  • @abdoulaliyicisse1753
    @abdoulaliyicisse175328 күн бұрын

    C'est trop facile il n'a qu'à subir les conséquences les lutteurs ne créent pas d'emplois ils empochent leurs cachets ils s'en foutent des supporters arrêtez votre cinéma

  • @MoussaCisse-rh6bq

    @MoussaCisse-rh6bq

    27 күн бұрын

    Ils doivent partager leurs cachets avec tous les supporters?

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage648228 күн бұрын

    Lene de khamnako makane merci et tant d autres mais pere gaston soukoko fi fekone J en suis persuade lac dou ague kasso dinako diokh 2 a 3 avance mou regle probleme il faut lance un numero weve ou orange je suis pres a donne kelk chose

  • @user-hf6yc2dt3w

    @user-hf6yc2dt3w

    28 күн бұрын

    Way lac 2 mérite ce qu'il a semé

  • @user-mg2nt7df3n

    @user-mg2nt7df3n

    27 күн бұрын

    Merci bcp yawmi thi sa commentaire billahi wakh gua deugue mo nekone papay mbeur yi yalna khippe aldianay firdaws 🙏😭

  • @MoussaCisse-rh6bq

    @MoussaCisse-rh6bq

    27 күн бұрын

    ​@@user-hf6yc2dt3wA bon? Xam nga nimou démé. Lac 2 t'a dit quelque chose?

  • @MactarFall-ge4ol

    @MactarFall-ge4ol

    25 күн бұрын

    Pére diapalé dou force bamouy encaissé kéne fékéwoul ngéne beug forcé nitt yi gnouka guena sokhla diapalé nio nék si kasso yi ak si hôpital yi lac nitt la comme nieup

  • @MoussaCisse-rh6bq

    @MoussaCisse-rh6bq

    25 күн бұрын

    @@user-hf6yc2dt3w saway légui mom d'accord na bima guissé vidéo yi ak déglou audios yi lac don def.Lac dafa nélaw bilahi.

  • @cissemalick944
    @cissemalick94427 күн бұрын

    Massa lac metina. Mais fadel sur 59 millions kel l'apport d lac2? Il a gagné d gros cachet dans la lutte j pens.kment il a géré sa carrière. Lac 2 yalla na gueune foumi nekka amine .wasalam

  • @FamaLaye-kb6cj
    @FamaLaye-kb6cj28 күн бұрын

    Mais khana lac amoul bien na diay keureum mo gueun ngeni niane ndimbeul temine chaque annee presque 50 million ak aye business sam khana investire na si. Dara alal dou fath deh gathiet lay fath wasalam

  • @aliouneelevage6482

    @aliouneelevage6482

    28 күн бұрын

    No les gens ne comprenne pas c qui es dans le dossier le monde de la lutte va payer et presque conclu

  • @senegalais.
    @senegalais.28 күн бұрын

    Sur 59 million mané donne 10 becaye lidjanti 25 mouy 35 milion donc Lac 2 yoroul dereum. Ne bayi beurré il a aucune bonne gestion comme beaucoup de lutteurs. Un cachet c’est un salaire c’est a dire pour vivre pas pour que preparer un combat lolou sa m’enerve chez les lutteurs

  • @ndeyembathiodiallo5723
    @ndeyembathiodiallo572325 күн бұрын

    Prison dé kene yéné wouko kene mais nak wakh deug yalla truandé ay nitte lek séne khaliss ba paré di méré nitte nane kéne diapalé wouko 😂Senegal dafa nekh beuri ay nafékh

  • @andrendione9021
    @andrendione902127 күн бұрын

    Lac vraiment mo togne, dafa nélaw trop. Ndiouplang bahoul. Mais pourquoi faay bi gnou beugeuko forcé niitt yi.

  • @famadrame6135
    @famadrame613527 күн бұрын

    Yalnako yalla takhaw

  • @khadimdiouf9608
    @khadimdiouf960828 күн бұрын

    Senegal daal mo nekh

  • @badoundiaye3158
    @badoundiaye315827 күн бұрын

    Way saway may léne niou diam truand alalou diambour nguéne takhaw nane daniou nio sétane lac est malhonnête mom dafa meuna délivré visa bayiléne nafekh

  • @user-qq9cs4to5h
    @user-qq9cs4to5h28 күн бұрын

    Fadel lingaye defni diakhasé la gnép khamnagnou aziz ngaye wakh

  • @djibrildiop6148
    @djibrildiop614827 күн бұрын

    Mais mo dieul khalisou diabour na faye

  • @cheikhomardrame5836
    @cheikhomardrame583628 күн бұрын

    Lac mo lekk khaliss diambour ngen né daniouko setane 😂😂😂Senegal mo nxx

  • @fatoubinetoulam275

    @fatoubinetoulam275

    28 күн бұрын

    Nekhoul ndank sakh

  • @mbayendiaye8825

    @mbayendiaye8825

    28 күн бұрын

    Na fékh rék

  • @oumarniangoumar5ujust446
    @oumarniangoumar5ujust44628 күн бұрын

    Dafa yomb tropp 😂😂

  • @Insamassaly
    @Insamassaly24 күн бұрын

    Moi je dis que c'est pas sérieux de sa part lui Lac il a tralli tout le monde c une honte merci

  • @fallissa4118
    @fallissa411826 күн бұрын

    Mo def il na qua assumée vraiment nafekkk bakhoulll may wakhe ngaine nane daneko piéger ak louné c fau moko def

  • @diopmar6382
    @diopmar638228 күн бұрын

    Sa diabar mo sathe khalice sou khaleyi nganan setou diw la

  • @ndeyembathiodiallo5723

    @ndeyembathiodiallo5723

    25 күн бұрын

    😂😂😂😂

  • @senegalais.
    @senegalais.28 күн бұрын

    Mbeur di negn ko feyy 100milion pour un combat mou depenser lep tek si meré ay niit parce que niane ne len meyou niou ko. Des éternels mandiants. Je souhaite a peersonne la prison mais sa me fait chier qu’ils soient la toujours a demander comme si on leur doit quelque chose.

  • @ndialoumboup3017
    @ndialoumboup301727 күн бұрын

    Yennn gni gniyyyy wakh dako lekkk est c Que fekker nguennn ko Kou khamoul Dangay woter mandou Keneu Kou nekk na dieul Thi bopam exemple the khamni tolof tolof Kou nekk thiy nekkk doundeu bou sotegoul Lou nek khathi nathi Aussi bou lennn fatei ni euleuk dhé amna bamel dafa khattt dhe

  • @Kako-gq3cj
    @Kako-gq3cj28 күн бұрын

    Fadel..boule.nek.nafekhe..

  • @user-fc5lc7sq1i

    @user-fc5lc7sq1i

    28 күн бұрын

    Ki kaay nek na nafekh ba paré

  • @user-up6ub4ym1e
    @user-up6ub4ym1e27 күн бұрын

    Lutteur bou nek na diokhei 5 millions si 10 vip yi mou nek 50 million khaliss bi matt ou bien dans l’autre sens qu’il assume ses responsabilités faye wala teud rk

  • @abdoulaliyicisse1753
    @abdoulaliyicisse175328 күн бұрын

    Vous êtes des lutteurs il faut cotiser entre vous payer et arrêter de nous déranger surtout aller régler avec le C N G sur l'argent qu'on vous coupe

  • @PaulMendy-gx4jt
    @PaulMendy-gx4jt27 күн бұрын

    Chez fasile laichez le pays l argent des jean

  • @user-on3lw2lz1w
    @user-on3lw2lz1w28 күн бұрын

    Les 10 lutteurs vip kounek 10 millions rek leip matt

  • @PaulMendy-gx4jt
    @PaulMendy-gx4jt27 күн бұрын

    Limotaque ont n est à retare le ga fet ses trient et ont dit nogalou yalla n foutez pas les jean

  • @Kako-gq3cj
    @Kako-gq3cj28 күн бұрын

    Mais.lima.diakhal.moy.loutakhe.nioune.lat.de.gur.danioko.setane.kaso.kene.yenewouko.kene.mais.nak.dibaly.dou.force..

  • @diopmar6382
    @diopmar638228 күн бұрын

    Wakhal wolof nganan le somme

  • @aliouneseck9774
    @aliouneseck977428 күн бұрын

    Sénégal mo nekhe

  • @salifdiediou
    @salifdiediou28 күн бұрын

    salut damay lathie lac dagn ka togn walla mo togn😂😂😂senegal mo nékh

  • @mbayendiaye8825

    @mbayendiaye8825

    28 күн бұрын

    Moma diakhal

  • @salifdiediou

    @salifdiediou

    28 күн бұрын

    @@mbayendiaye8825 doyna warr

  • @senegalais.
    @senegalais.28 күн бұрын

    Lutteur yi sen cachet pour niom si ben combat la wara yem. Lac2 avec tous les combats qu’il sans compter les aides war na tok diamono bi dou am loumou regler son problème. Mbeur legni feey 100milion mou dougal lep si preparation combat tek si ndimbal yi niou key dimbalé lolou yone la!!!!

  • @bourathobouratho4672
    @bourathobouratho467228 күн бұрын

    Défaite deug la

  • @aminatagueye2017
    @aminatagueye201728 күн бұрын

    lekk lo momoul fay

  • @damembow6374
    @damembow637428 күн бұрын

    Saloum saloum dou mbeur khana

  • @khadimdiouf9608
    @khadimdiouf960828 күн бұрын

    Wa ani khaliss bii meunoul lekk lepp nako dello c mieux

  • @papesadiothiam3734
    @papesadiothiam373428 күн бұрын

    Wakhal Wolof te bayi français bi !

  • @souleymanendao1843
    @souleymanendao184328 күн бұрын

    Mbeur aka baadola

Келесі