SA NDIOGOU DEMASQUE AZIZ NDIAYE...MODOU LO LA BEIGUE WEUR...LIMOU WAKH SI BAYE NDIAYE...

SOLUTION TV

Пікірлер: 822

  • @mansorgueye4462
    @mansorgueye4462Ай бұрын

    Faal thiaakhane baxoul. Balla Gaye lay supporter mais Modou Moy roi des arènes té mo leen eup mérite fouf. C’est un vrai athlète discipliné et constant dans la performance. Wassalam

  • @MameSow-vp7rj

    @MameSow-vp7rj

    Ай бұрын

    Vraiment ❤

  • @keytanodiallo4979

    @keytanodiallo4979

    Ай бұрын

    Nio yem balla moy sama mbeur mh modou mérite son titre et il faut le reconnaître

  • @mbayendiaye5033

    @mbayendiaye5033

    Ай бұрын

    Billay wallay deug dou nekh

  • @fatmagueye1541

    @fatmagueye1541

    Ай бұрын

    Tu as raison mai yalla bakhna

  • @darou2290

    @darou2290

    Ай бұрын

    Il a raison de faire ça

  • @senegaldabord1201
    @senegaldabord1201Ай бұрын

    Nékhoul ba Nékhoul sa ndiogou est un grand machallah. Un vrai héritier de feu sidy lamine niass

  • @cheriftounkara6470

    @cheriftounkara6470

    Ай бұрын

    SA NDIOGOU A TOUT DIT

  • @morfall6424

    @morfall6424

    Ай бұрын

    Da ngémé deug Aziz dafa sokhor

  • @geumyeugofficiel7688
    @geumyeugofficiel7688Ай бұрын

    Yalla mofi tek modou lo aziz monosi dra

  • @modoudiop6522

    @modoudiop6522

    Ай бұрын

    Yalla mbeurëm môy malakal mawti d'où am défétt mouk day dâne Di déme rék

  • @dounejr6956

    @dounejr6956

    Ай бұрын

    @@modoudiop6522 Bien dit💗

  • @awalo2

    @awalo2

    Ай бұрын

    Bilaye modou rek lanou bagne famille ndiaye

  • @Maamseex

    @Maamseex

    Ай бұрын

    Modou Lo mo wara bayi daw yi

  • @ShiekhjobeTijan

    @ShiekhjobeTijan

    Ай бұрын

    Ta moy dege ❤

  • @dibouthiaw2276
    @dibouthiaw2276Ай бұрын

    Mann dou ma fans modou dée mais Li Aziz beugue deff yeuffou Sokhor la 😡😡😡

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Merci ❤

  • @dembandiaye585

    @dembandiaye585

    Ай бұрын

    Aziz mon téy boullénou sonale

  • @omarthioub630

    @omarthioub630

    Ай бұрын

    ترجمة إلى اللغة العربية

  • @casebi5016

    @casebi5016

    28 күн бұрын

    Lolou la dh dou lénèn

  • @fallouniass-sj7rd

    @fallouniass-sj7rd

    28 күн бұрын

    Bilay sokhor dafa am

  • @djilygueye1352
    @djilygueye1352Ай бұрын

    Modou lo mofi nek aziz monosi dra yalla rek inchallah

  • @fatouTALL-ld1ro
    @fatouTALL-ld1roАй бұрын

    Aziz Ndiaye ci bopam mo soxorei Modou Lo mi tok ci couronne bi. Modou moy le Roi reconnu par le Cng et tous les senegalais.

  • @user-ln7ii6xv3g

    @user-ln7ii6xv3g

    28 күн бұрын

    Merci beaucoup

  • @daoudadiop8178
    @daoudadiop8178Ай бұрын

    En tant que fan de Mohamed Ndao Tyson, le meilleur lutteur de tous les temps c'est Yahya Diop Yékini.

  • @yerosow7063

    @yerosow7063

    Ай бұрын

    Lolou mom c la vérité

  • @martindiene9113

    @martindiene9113

    Ай бұрын

    Deugu bou woor

  • @AlassaneDieye-cc7jq

    @AlassaneDieye-cc7jq

    Ай бұрын

    Tout a fait . Manga n'a pas fait ce que personne ne fait. Yekini et Modou Lo ont la plus belle performance que lui. Mom au mag rk ladone dane

  • @fatimaciss5602

    @fatimaciss5602

    Ай бұрын

    Deug dou romb nop

  • @amymbodji1097

    @amymbodji1097

    Ай бұрын

    Lou woor ga wakh

  • @fayedame3605
    @fayedame3605Ай бұрын

    Aziz ndiaye et sa famille se crois plus malin que tout le monde

  • @sambagora7848

    @sambagora7848

    Ай бұрын

    Lamb j santoul ndiaye aziz day dolèle thiakhane rek😂😂😂

  • @amadouba4254
    @amadouba4254Ай бұрын

    Bilay tapha tine yallah na dane balla after niou xol nou aziz di def

  • @ousmanecisse4262

    @ousmanecisse4262

    Ай бұрын

    Amiiine

  • @matartoure-jg8hl

    @matartoure-jg8hl

    Ай бұрын

    Wa douko dan nak😅

  • @marathiam1560

    @marathiam1560

    Ай бұрын

    Amine Bobou ngene di xamni aziz mo faux salaire bimouy waxx doukoko meussa fayy par mois dafay doul

  • @moustaphasonko596
    @moustaphasonko596Ай бұрын

    Sa ndiogou est très pertinent

  • @BenMejbour

    @BenMejbour

    Ай бұрын

    Sa N'diogou Mach'Allah ci bénene niveau la nek

  • @mbayecisse611
    @mbayecisse611Ай бұрын

    Aziz geumeul yalla modou lo moy sèn baye xlo roi 👑

  • @alioubadarasadiasane2534
    @alioubadarasadiasane2534Ай бұрын

    On a pas besoin de Balla Gueye en Casamance car il avait dit qu'il n'est pas de la Casamance. Nous on est fier de Casamance

  • @seydinacamara4782

    @seydinacamara4782

    Ай бұрын

    Merci lolou la beuguone waax

  • @sambagora7848

    @sambagora7848

    Ай бұрын

    😂😂😂😂c'est vrai déh

  • @ramatoulayesene3743

    @ramatoulayesene3743

    Ай бұрын

    ah bon dafko messeu wah ?

  • @agn3121

    @agn3121

    Ай бұрын

    ​@@ramatoulayesene3743Balla moko wakh durant les evenements de 2023...😂😂😂

  • @Omarsane7491

    @Omarsane7491

    Ай бұрын

    Bilahi balla gaye 2 on la pas besoin a Casamance

  • @mouhamednaby3220
    @mouhamednaby3220Ай бұрын

    C'est modou lo le roi actuel

  • @ibnoukhayriismaelba618
    @ibnoukhayriismaelba618Ай бұрын

    Bayilen thiakhan bi. Bayilen yakh lamb J. Affairou djaay khalis bi bakhoul. Yallah molen euppp khaliss. NB: je suis supporter Balla Gaye. Mais respectez Mod'Lo Il est le Roi des arènes

  • @mamepathengom9398
    @mamepathengom9398Ай бұрын

    Sa est trés pertinent 😂😂Azize dafa nagou ✍️CNG amougnou foula amougnou fayda✍️boudone Balla mo nék place bou Modou lô ✍️ dou wakh limou wakh✍️ wiri wiri bi yép moye Balla la Azize beugue mou beuré ak Modou lô ✍️😂😂😂😂

  • @user-rg2kk9hg2g

    @user-rg2kk9hg2g

    Ай бұрын

    😂😂😂

  • @mamourndaw3746

    @mamourndaw3746

    Ай бұрын

    Ki dafa soxorr way

  • @marathiam1560

    @marathiam1560

    Ай бұрын

    Merciii loloy wax dji le rêve le plus cher de aziz moy balla beurei wat ak modou danat ko Mais modou dou defati lolou ndax nit kou nangou ndogal leu na gou na liko Yalla tek si Balla gaye mouy ke ni moy bete noiram Modou soxoroul bagn ko ladjei son 1er combat contre balla dafni lamb djodjou moma def mbeurrrr Balla o contraire fi leuko eumeu dane 2 fois mou insister ni « dane nama wayei meunouma ». Wayei soxor mom amoul solo modou dina geuna dieul si kanam dolene si mane daraaa

  • @papeomarba2109

    @papeomarba2109

    26 күн бұрын

    Balla sou nekone fi modou nek dou moye tou kéna 😂😂😂

  • @marathiam1560

    @marathiam1560

    26 күн бұрын

    @@papeomarba2109 mom d bam neikei roi diotoul am temps wou moytou saxx ndax dassa yagoul 😂😂😂beneu victoire si tafa tine apres gassi 😂😂legi loutax Balla moytou siteu kone ??? Fall plan de carriere dafa am koussi nek temps ba bou diotei di nga beurei ak gni nga wara beurel mbir mi intelligence ak professionalisme dassi boss t modou lol kay def avec son staff motax mou raww gayiii sougn ko dieulei beneu beneu amoul loumi diay Balla pck moko dane 2 fois Mais soudei si carriere en general modou moko geune lei Balla fouf insbi xoolouko saxxx pck dafeu gerer carrieram mou rafett yakoul yaramam, saax saxé woul carrieram bay téglé ay defaite

  • @matardrame4101
    @matardrame4101Ай бұрын

    Nonn Sa Ndiogou vous êtes très fort. Plus fort que beaucoup de gens qui gravitent au tour de la lutte qui n'avance pas . Depuis plus de vingt ans ce sont toujours ce sont les mêmes.

  • @omarthioub630

    @omarthioub630

    Ай бұрын

    ترجمة إلى اللغة العربية

  • @abdoulkhadrediallo1252
    @abdoulkhadrediallo1252Ай бұрын

    tu as parfaitement raison sa ndigou je suis d'accord à 1000% avec ton point de vu

  • @sgfdaroukhoudoss6018
    @sgfdaroukhoudoss6018Ай бұрын

    Être empereur , c'est pas si facile comme il le crois. Kheuy un bon jour rk créé empereur 😂😂😂😂. Même être roi n'est pas facile. Balla gaye même, rêve bel et bien de redevenir bourou lamb dji comme tous les lutteurs 🤼‍♂️ . Sokhor bakhoul ❤❤❤

  • @bachirvd619
    @bachirvd619Ай бұрын

    Sokhor bakhoul modou moye roi force 🎉

  • @ibrahimasarr2085
    @ibrahimasarr2085Ай бұрын

    Franchement Sa Ndiogou meune na analyse. amna solo

  • @omzo9376
    @omzo9376Ай бұрын

    On a pas besoin de Balla en Casamance. En plus Inshallah Balla il va perdre.

  • @pierrediagne9923
    @pierrediagne9923Ай бұрын

    Wa yene aziz Ndiaye mi khana da fokni mo môme senegal non khalisse Day yak nite koi

  • @user-xq5dj9fp5d

    @user-xq5dj9fp5d

    Ай бұрын

    Barki yalla dafa rew dagn ko wara ndy nokh

  • @user-id8on4gq5u

    @user-id8on4gq5u

    27 күн бұрын

    Merci dafa bew

  • @SALIHTV10
    @SALIHTV10Ай бұрын

    Modou lo moy roi

  • @user-kaka35

    @user-kaka35

    Ай бұрын

    😂dioutal Lo roi wou kane😂😂

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Balla dafa dane Modou niari yone Modou nieuw rawko si lamb té ay rival lagn lololéne méti motakh niouy saltél mais dara défar sakh couronne nou diamant mais Roi bi mom Khalé bou civilisé biy yéwo PA moko mom❤🎉XLO KASSÉ 🎉❤

  • @user-kaka35

    @user-kaka35

    Ай бұрын

    @@rouguikebe9984 modou munul raw balla thikaw souff xana benen monde mais dou biii té boulen fatteni bi guy yi didaw yikini fii Lanou fek ben balla rek moko gnemé won dieul kon kousi deg roi des arenne warngako santé balla gaye 2 dioutal Lo mom damako diélleulé😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ousmanecisse4262

    @ousmanecisse4262

    Ай бұрын

    @@user-kaka35nanal ndokh😂😂😂😂

  • @user-kaka35

    @user-kaka35

    Ай бұрын

    @@ousmanecisse4262 nane ndokh pour mankey Lima wakh Ken douko dindi

  • @serignefalloucisse969
    @serignefalloucisse969Ай бұрын

    Sadioguou a juste dit la vérité les restes du plateau son des énemis de Modou lo le roi des arènes

  • @user-uj9ok2ue2k
    @user-uj9ok2ue2kАй бұрын

    Balla moy sama Mbeur ms aziz nak kou sokhor la vraiment

  • @ElhadjiFall-nw2he

    @ElhadjiFall-nw2he

    Ай бұрын

    Franchemen yagu nano ingnane mo dou lo. Dou deug interem mosinek

  • @abasall711

    @abasall711

    28 күн бұрын

    Merci sa way ku degou nga

  • @sadiocamara192
    @sadiocamara192Ай бұрын

    Balla gaye n'est pas casamançais, car lui même il a dit ouvertement. Donc s'il vous plaît épargné la Casamance

  • @mouhamedthiane1507
    @mouhamedthiane1507Ай бұрын

    Aziz dafa ndeye sokhour bilahi

  • @user-nd1xq1sg5j

    @user-nd1xq1sg5j

    Ай бұрын

    Niomm ak senn ayy thioggou dounou ay nit you baxx

  • @user-cr9uf9hb8l
    @user-cr9uf9hb8lАй бұрын

    Azizz n’a topou feulleu khana bi modou lo néké toi laniou begue niakal fayda roi 👑 ms moy roi far force naniou nangou nopalou

  • @koulaalhakk8975
    @koulaalhakk8975Ай бұрын

    Si balla devenez empereur...donc eumeu khana Bourou bourri😂😂😂Té mod lo mo nokh eumeu milene nokh😂😂

  • @modougaye919
    @modougaye919Ай бұрын

    Balla gaye mon mane modou eume sene mane balla gaye modou lo mane eume sene bayi lene sokho modou monfi nekk❤️❤️❤️❤️

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9yeАй бұрын

    Merci père sa diogou la lutte n'appartient pas à la famille ndiaye 😕

  • @user-mv5sj1gv4g
    @user-mv5sj1gv4gАй бұрын

    No billahi li Sa ndiogou wakh Deugueu, en résumé moy Azize ndiaye dafay fathie Mërr si Modou Lô vs Siteu bi

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijanАй бұрын

    Modou lo Moy 👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤komo nekh ak komo nakhari ❤❤❤❤❤❤❤

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9yeАй бұрын

    Aziz Ndiaye vrai domouharam la et puis le CNG ne doit accepter cette idée 😕 nous avons qu'on seule roi 🫅 et que c'est Modou lo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @sallasylla3484

    @sallasylla3484

    Ай бұрын

    Li dh khékh modou lo nk 😢

  • @omarthioub630

    @omarthioub630

    Ай бұрын

    ترجمة إلى اللغة العربية

  • @cheikhpendambaye2911
    @cheikhpendambaye2911Ай бұрын

    Dogaloul Yalla diam meunousi dara vraiment Aziz Ndiaye kou yabaté nga mane dh fans balla Gaye la wayé li Aziz Ndiaye wakh andoumasi boudone balla Gaye moy roi bi do beug kouko def balla Gaye Aziz Ndiaye bayil togn bakhoul lingay def dou deug dou yone koula ko wakhoul dala ragal merci sa ndiogou sa wakh rafet na

  • @medounediene9652
    @medounediene9652Ай бұрын

    C.N.G YÉKINI NÉKHOULENE MOTAKH SANDIOGOU WAKHNA DEUG❤❤❤❤❤

  • @ibrahimacoulibaly6933
    @ibrahimacoulibaly6933Ай бұрын

    Sohibou il faut écouter Assane mais pas le regarder souvent il raisonne en profondeur même si dès fois il passe à côté

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijanАй бұрын

    Modou lo rek 👑👑👑👑👑👑👑👑 mofi ne dege do nekh na no ko wax ta de ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mansourndione178
    @mansourndione17829 күн бұрын

    Yekini c le meilleur luteur d tout les temps

  • @allandiaye7665
    @allandiaye7665Ай бұрын

    Sa ndiogou c le meilleur Bilahi

  • @KarimoulahMbaye-kt1fo
    @KarimoulahMbaye-kt1foАй бұрын

    Aziz iow daga bah rék😂 roi bi kénela mouy gonégui lô💪🏿

  • @user-fj5ib8xm2l
    @user-fj5ib8xm2l27 күн бұрын

    Aziz adouna amoul solo ..sokor bakhoul grand...té iow do lamb sakh. Fii yAllah fi nek té Modou lafi ték

  • @niassniasstapha9150
    @niassniasstapha9150Ай бұрын

    Aziz dafa sokhor balla Gaye boy niang niouss kofi daw rk

  • @ousmaneka4984
    @ousmaneka4984Ай бұрын

    machallah sa ndiogou ❤Deug dou rombi nopou waye❤Assane mome thi ay nèlaw la nè baligui 😅

  • @yatmaseck3056
    @yatmaseck305624 күн бұрын

    Merci sa ndiogou sa deugou mon takh niou beug la do nafékh nitou DEUG gua 😮

  • @Mobamba0996
    @Mobamba0996Ай бұрын

    Sa ndiogou yalla nasa diame yague ❤

  • @landing3358
    @landing3358Ай бұрын

    Deuk bo khamoule nofféy déffé open de press Vue que balla néna khamoule casamance. Aziz ndiaye toi et ta bande respecter nous svp la casamance n'est pas un lieu de comédie

  • @bachirlo1343
    @bachirlo134329 күн бұрын

    Sa ndiogou machallah il est fort en analyse❤

  • @expert2foot
    @expert2footАй бұрын

    Qui bat le roi devient roi simple comme bonjour

  • @user-sx9vw3zy1b
    @user-sx9vw3zy1bАй бұрын

    Assane messeré yaw ak Souhaïbou da nguèna sakhor thi Modou lô rek motakh mais Modou lô yalla moko fi tekk

  • @CheikhOumarFaye-if1eo

    @CheikhOumarFaye-if1eo

    Ай бұрын

    😂😂

  • @user-xq5dj9fp5d

    @user-xq5dj9fp5d

    Ай бұрын

    Barki yalla gni dagno bagn modou lo

  • @adamaba6508
    @adamaba6508Ай бұрын

    Sa ndiogou cerveau ❤

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye735325 күн бұрын

    Merci Sa Ndiogou Aziz Momoul Lambeu Dji Yalla Modou Lô La Déff Roi👑💪🏽💪🏽 De L'arène Téla NanGou Day Yombali Douma 🙏🏽

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rjАй бұрын

    Ms Aziz Ndiaye mi moy domouharame moy nitt kou bonne moy imbécile moy domou khathieu deug😂😂😂

  • @user-xq5dj9fp5d

    @user-xq5dj9fp5d

    Ай бұрын

    Merci 😂

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Djadjeuff

  • @geos_tv3953memphis
    @geos_tv3953memphisАй бұрын

    Machallah sa ndiogou sa halate sett na

  • @mansourelias1616
    @mansourelias161627 күн бұрын

    Merci bcp Sa Ndiogou deugeu dou rombou nop th yalla ko mom

  • @malickndiaye7899
    @malickndiaye7899Ай бұрын

    Merci sa ndiogou ❤❤❤ aziz yabatè rek ak bew moko dall

  • @abdouazizthiaw3491
    @abdouazizthiaw3491Ай бұрын

    Aziz en tant que promoteur du mom moy titré mbër .CNG mo wara doggal lu mel nonu.. Fédération wallah comité moy titré champion.. Na aziz yém ci rôle promoteur..

  • @martindiene9113
    @martindiene9113Ай бұрын

    Aziz ndiaye da cissou ndah khamna ni Balla Guaye 2 dou diotate couronne 👑 bi

  • @user-yl6qx3fx4d
    @user-yl6qx3fx4dАй бұрын

    Soxarr bakhoul modou lo moye le roi waa keur balla aziz ndiaye comme aye lesbienne bilay 😊

  • @mouhamedfofana4266
    @mouhamedfofana4266Ай бұрын

    Merci sandiogou❤❤❤❤❤❤

  • @MatombonDanso
    @MatombonDansoАй бұрын

    BALLA BOU DOUGUÉ CASAMANCE NIOU OUBI TOUNOU NDÉM. CASAMANCE AY GORR LANIOU.

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate589327 күн бұрын

    Merci sa ndiogou amna solo de

  • @Map_au_campus
    @Map_au_campus27 күн бұрын

    Billay sa Ndiogou yaa niémé deug wallahi ✌🏿🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @beckkarbonik180
    @beckkarbonik180Ай бұрын

    Merci beaucoup Elhadj. Bon pronostic

  • @user-mv5sj1gv4g
    @user-mv5sj1gv4gАй бұрын

    Tay moom Souhaïbou danou nga si piége Assane Messere, ndakh tay Dégo lén Sa ndiogou

  • @fadelrassoul4398
    @fadelrassoul4398Ай бұрын

    Assane ayy wahi dof lay wahh merci Sa

  • @mouhamadoulaminekande8796
    @mouhamadoulaminekande879625 күн бұрын

    Supporterou Balla gaye la mais Modou lo Moy roi des arènes ❤❤❤ Dégue néxoule

  • @user-nf3jd7ji4o
    @user-nf3jd7ji4oАй бұрын

    Ki wakhi doff rek la fi wakh mouy mél ni kirikou ni, merci sa modou Lô c’est le roi 👑

  • @pierrediagne9923
    @pierrediagne9923Ай бұрын

    Baye assane modou lo moy bayou lamb j

  • @user-kaka35

    @user-kaka35

    Ай бұрын

    Balla dioutal ko fi😂

  • @mouhamedelmoustaphadjikine6971
    @mouhamedelmoustaphadjikine697122 күн бұрын

    Niémé wax deug té yalla rék tax, loolou sax ndiambarté la. Mâcha allah sa ndioogou

  • @sambemoussandiongue5663
    @sambemoussandiongue5663Ай бұрын

    Assane,néna Balla moo meune modou lo, eumeu moo meune Balla, mais wakhoule née Modou lo moo meune eumeu séne,

  • @user-jd1qz7zs3l
    @user-jd1qz7zs3lАй бұрын

    Merci beaucoup Sa ndiogou bien dit machallah 👍

  • @omarsarr-ff3pu
    @omarsarr-ff3puАй бұрын

    merci sa💚💛❤️💪💪

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijanАй бұрын

    Waw ko dañ bour yaye Bour kon modou moy bout👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑

  • @SALIHTV10
    @SALIHTV10Ай бұрын

    Merci sa hazizz dafa bagn modou lo rk

  • @Abdallah31341

    @Abdallah31341

    Ай бұрын

    Banioul modou boul diawalé, balla gaye mbeureum la beug yekeuti rék

  • @FallouawaBousso20
    @FallouawaBousso20Ай бұрын

    Journaliste yi lou lene modou lo Def merci san ndiogou ❤

  • @tawfekh1427
    @tawfekh1427Ай бұрын

    Aziz geumoul dara fi lako serigne am tere lamb dji mou bagn mai n'a nangou lifi yala deff

  • @arantxaarrillaga9537
    @arantxaarrillaga9537Ай бұрын

    Aziz tranquilo le roi c modou😂😂😂

  • @MoustaphaDiop-is4tb
    @MoustaphaDiop-is4tbАй бұрын

    Merci sa niogou deuge yalla moka mome

  • @elimanediop2764
    @elimanediop276427 күн бұрын

    Merci sa vraiment DEUG ngua wakh

  • @KhadyTall-dz5cp
    @KhadyTall-dz5cpАй бұрын

    Roi modou lo lako yalla def

  • @BabacarNdiaye-ll8um
    @BabacarNdiaye-ll8umАй бұрын

    Sandiogou merci si lérel yi❤❤

  • @user-mi9wn5ir3z
    @user-mi9wn5ir3zАй бұрын

    Modou lo c'est le roi

  • @AbdulPape-hp1hh
    @AbdulPape-hp1hhАй бұрын

    Machalah sa y’llah nalah yallah fay

  • @10gitallewolof30
    @10gitallewolof30Ай бұрын

    Talkle show dé cheikh bara Ndiaye lafay fek inchallah

  • @CheikhNdiaye-yr7zo
    @CheikhNdiaye-yr7zoАй бұрын

    Wakh deuge yalla balla moy sen baye môme rk laay topo me modou lo moy roi bi azzis ndiaye modou lo moy roi bi

  • @abdoulahadmbaye1488
    @abdoulahadmbaye1488Ай бұрын

    Aziz musul bague modou lo waye na niaf ndeyem fale manul Wakhe ba du neke roi balla mom pena si lamb

  • @Alle-fc8pj
    @Alle-fc8pj19 күн бұрын

    Azize Ndiaye sofegua sokharegua Modou fans Balla tu khamenaneni Moy roi

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rjАй бұрын

    Modou lôooooooooo ❤❤❤

  • @yatmaseck3056
    @yatmaseck305624 күн бұрын

    Bilahi cng du dara 😮 yekini AK limou fi def lep il n'est pas reconnu

  • @ndiawsamb4205
    @ndiawsamb4205Ай бұрын

    Wakh dji lére na nagne wayé merci beaucoup saa yawe comprendre lépe ta niémé nga deugue

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijanАй бұрын

    ❤❤❤❤❤ Billy SA wax ga dega bo weer ga wax Liga wax loulo mo am ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aidakasse1479
    @aidakasse1479Ай бұрын

    Merci sadiogou 💯 😂😂😂😂😂

  • @MouhameLo
    @MouhameLo28 күн бұрын

    Li du yone aziz ndiaye balla mo mbeure motaxh moy waxh li mais modu lô moy sene baye

  • @user-gi7ne4rm6o
    @user-gi7ne4rm6oАй бұрын

    Modoulo rekk lañooy topo ❤❤❤❤

  • @user-sx9vw3zy1b
    @user-sx9vw3zy1bАй бұрын

    Assane wakho fi dara

  • @ousseynoudieng7429
    @ousseynoudieng7429Ай бұрын

    Non mais sa Machala ❤❤🙏🏽

  • @awalo2
    @awalo2Ай бұрын

    Famille ndiaye dano sokhoré modou Lô roi , nekh nakhari modou Lô moy roi

  • @ndeyendiaye8662

    @ndeyendiaye8662

    Ай бұрын

    Awa boul waax Ndiayeen waay😂Azize nimouy faralee balla mo meeti.bou balla nekoon Roi kone dou wax li. Modou lo néexou ko niep xamnanioko.wayee yalla moye dogual. Na mougne rék yalla baax na tenga nane ndox mou seed guouye lou méti yaguoul 😊😊

  • @awalo2

    @awalo2

    Ай бұрын

    Merci beaucoup ma chérie

  • @mbayebarri3404
    @mbayebarri3404Ай бұрын

    Boudone. Modou lo ak tapha tine azize dou tekk dara😊

  • @serignefalloudjimbira9790
    @serignefalloudjimbira9790Ай бұрын

    Merci sa

Келесі