Reug Reug fait une confidence : " De Gaulle dafma ni ... wayé damay beurek Boy Niang "

ALBOURAKH EVENTS LA CHAINE EVENEMENTIEL

Пікірлер: 101

  • @mouhamaddieng6218
    @mouhamaddieng62184 ай бұрын

    En tout cas Reug Reug on peut tout lui reprocher mais c’est un vrai champion…nieupp la meuneu daann si lamb dji

  • @user-pq3ep6qr1n

    @user-pq3ep6qr1n

    4 ай бұрын

    Bilahi lou werr nga wakh frère sokhor ak nafekkkkh rek mofi nek wayé reug champion la

  • @mamadoundiaye5230
    @mamadoundiaye52304 ай бұрын

    Reug reug le grand champion jamm si ioe gua yii dénio sokhor guisna kou mbinde ioe rek la bagne mais yalla bakhna

  • @serafall946
    @serafall9464 ай бұрын

    Machalla reug reug grand champion degue gua wakh billahi ❤❤❤❤❤❤❤ boy niang dey daw rek❤❤❤❤❤

  • @papiiiswelleeiih5728
    @papiiiswelleeiih57284 ай бұрын

    Reug sama mbeur gua Mai’s boul fokniii y’a meune boy niang deh bilahiiiii boy niang soula meunoul meunoko yallah xamnako

  • @badandiaye8619
    @badandiaye86194 ай бұрын

    Reug reug champion la ❤

  • @hamasn946
    @hamasn9464 ай бұрын

    Mane lima diakhale gninane dafa ame problem communication mais lii lamb la dou diné dafa wara nékh

  • @babacardiouf6253
    @babacardiouf62534 ай бұрын

    Reug reug merci

  • @cirely3220
    @cirely32204 ай бұрын

    Reug reug bane champion le danne ay gris 2 ay elton ay gouygui 😁😁sathies moko dane

  • @elhadjiserignetoure8698

    @elhadjiserignetoure8698

    3 ай бұрын

    Vraiment

  • @assanesagne6276
    @assanesagne62764 ай бұрын

    Reug champion là bayilénne sokhorr

  • @demebadiekh7476
    @demebadiekh74764 ай бұрын

    Baniane de reug reug yak boye niang combat la😂😂😂😂 degual dala ragal dé 🎉😂😂😂

  • @soraboukharaglo
    @soraboukharaglo4 ай бұрын

    Lima nekh ci mom amoul kharite mbeur

  • @maissamboup4169
    @maissamboup41694 ай бұрын

    Reug c’est le meilleur je voi yekini

  • @karlsilver5776
    @karlsilver57764 ай бұрын

    Reug reug il faut jamais juger ouvsous estimer boy niang 2 apres son combat contre modou lo..dinga ame loula beteu..nite bokeyy topeu di wakh falewoula dou ragsl...

  • @elhadjiibrahimadiatta9485
    @elhadjiibrahimadiatta94854 ай бұрын

    Reug Reug❤

  • @AbdoulNdiaye-vj2dn
    @AbdoulNdiaye-vj2dn3 ай бұрын

    Reug champion nga

  • @mansourgaye4125
    @mansourgaye41254 ай бұрын

    Nguir yalla plateau yi bayilen di fi indi genrou mbeur you dof yi

  • @ibrahimaka2981
    @ibrahimaka29814 ай бұрын

    Bilay boy niang moko meun boy niang ben moromam yabouko

  • @Zikodiop2068

    @Zikodiop2068

    3 ай бұрын

    Moh😂😂😂

  • @user-lf8bo2bc2k
    @user-lf8bo2bc2k4 ай бұрын

    Reug reug billah dô sportive

  • @khalil7537
    @khalil75374 ай бұрын

    Reug bu dieuler boy niang li nga yakar si mom amul billae bo dof doflo mu dan la yaw mano xekh boy niang il suffit mu xekh ak yaw et j tjt il va t humilier

  • @Zikodiop2068

    @Zikodiop2068

    3 ай бұрын

    Boy niang balla gaye bou maguette bi rek la meuneu dane boulniou sonal😂😂😂😂

  • @ndenediagne50
    @ndenediagne504 ай бұрын

    T l meilleur frérot bonne continuation 💪🏾

  • @mamadouaidara9497
    @mamadouaidara94974 ай бұрын

    Je deteste telment reug reug mais j apprecie vraiment sa volontè de lutter contre tous les lutteurs

  • @ousseynoutoure518

    @ousseynoutoure518

    4 ай бұрын

    Le verbe détester est très lourd frr

  • @alioudiaw1446
    @alioudiaw14464 ай бұрын

    Athia Reug ReuG

  • @boubadiallo6622
    @boubadiallo66224 ай бұрын

    Vraiment reug reug il est fran dans ça parlé 😂😂😂😂

  • @user-wt7ww2qo2c
    @user-wt7ww2qo2c4 ай бұрын

    Reug dagua bari wakhe trop legui

  • @zokorasall9617
    @zokorasall96174 ай бұрын

    Reug reug damako fan

  • @user-ox2wf7dc5i
    @user-ox2wf7dc5i4 ай бұрын

    Champion leu mais dafa Bari wakh bilahi gor d'où Bari wakh

  • @abdourahmanesindidi1818
    @abdourahmanesindidi18184 ай бұрын

    La communication de reug reug😢

  • @mamadougueye3841
    @mamadougueye38413 ай бұрын

    Vraiment reug reug à une communication dépourvue de cohérence et de bon sens D'une part il dit qu'il est prêt à lutter avec tout le monde sans exception Et d'autre part il revient pour expliquer pourquoi il n'est pas prêt à affronter Eumeu séne Du n'importe quoi ce gosse !

  • @yilebaba6565
    @yilebaba65654 ай бұрын

    Reug reug il est vraiment de mauvaise foi ! Lors de son dernier face à face avec sa thiés a walfadjri il avait dit que lorsqu'il avait attaqué sa thies , il a senti qu'il était très lourd et puissant ? Là il vient de se dédire , sacré reug reug , c'est un champion mais un mauvais perdant

  • @fallabdou7163

    @fallabdou7163

    4 ай бұрын

    Problème bi moy supporter sathies dagno bagn reug té sathies sou d’accorone moy beuré ak bombardier mais balla beuré ak bombardier mongui contact ak sathies khamnani bombardier moman sathies fouff ndakh dafa diss motakh mou bagn épuit yén reuppou rk nguén am ci reug man khawma bolén ko danon noumouy mél té sathies proposé won nagnou ko mou beuré wat ak reug 80million mou daw combat bi sa dou gawa beuré wat ak reug khamna limou fa fékkeu biko reug diappaté dafa yombou trop

  • @papahabibdiopofficielle3160

    @papahabibdiopofficielle3160

    4 ай бұрын

    Mo reug mi weroul waaay ah😂

  • @aichadia719

    @aichadia719

    4 ай бұрын

    ​@@papahabibdiopofficielle3160reug walakhi weroul

  • @MrFayemanou

    @MrFayemanou

    4 ай бұрын

    😂😂khamougnou sakh lignii wakh

  • @amadugningue8168

    @amadugningue8168

    4 ай бұрын

    No reug kay mauvais perdant la koi

  • @khadimndiaye5910
    @khadimndiaye59104 ай бұрын

    Yalla khamne linga fok amoul bo yakarene boy niang dala ragal yagui ndakh sa bopou louler lala wakh del wakh rek

  • @user-gy1we4vh4c
    @user-gy1we4vh4c4 ай бұрын

    Reign reign day doul rekk

  • @omzo1412
    @omzo14124 ай бұрын

    Reug Wakhal wakh dji Niemè ga nieup ba mou dess Eumeu sene

  • @user-kn5uy3nu5x
    @user-kn5uy3nu5x4 ай бұрын

    Reug day sop

  • @cheikhdiop9673
    @cheikhdiop96734 ай бұрын

    reug reug waxna deug dé per degol ci bopam mo beug ap moytou di diéma tékk khel gnoniou bamalén khamé yageu na boy Niang ak papam séne lépp tékk khél la bagnouy dieul balla khamone nagne ni dagnouy dane Balla ndax Balla amatoul gnarigne motakh ligne wax ci combat bobou nimoubaré ndax khamnagne ni kignouy beurél amoul ndiarigne wayé bagnouy beuré ak mod lo gnou khamni wadji dafa liguéy bay khégne dollé kénn dégoul papay boy Niang di ndélou sénn lépp tékk khél la

  • @MaxJyLFSS

    @MaxJyLFSS

    4 ай бұрын

    Balla kay legui vrai yambar la quoi di kholee ba boy niang diko daan dieleu bou yomb bobou

  • @souleysarr8039
    @souleysarr80394 ай бұрын

    Sa thiess vs reug reug comme Modou lo vs Balla gaye 2 bou nieukeu

  • @ousmanemolo7231
    @ousmanemolo72314 ай бұрын

    AKA BARI WAKH

  • @Bilal66850
    @Bilal668504 ай бұрын

    Dou sama mbeur doumako faral mais vrai champion la

  • @momokarandiaye3069
    @momokarandiaye30694 ай бұрын

    C'est un Bon lutteur Mais problème communication la âme quoi ? C'est dommage

  • @user-yt2nl1lp7h

    @user-yt2nl1lp7h

    4 ай бұрын

    Bilaye iow

  • @TaphaKeita
    @TaphaKeita3 ай бұрын

    Wakhofi dara reug

  • @afro3827
    @afro38274 ай бұрын

    Reug reug guemal yalla sa thies dala douma dan la , beuthiagouk ndarakam nekal sportif té ga thiangui khekh sa thies wonna mbeur yi bounta bi dw dorr rek

  • @papezulefaye7263
    @papezulefaye72634 ай бұрын

    Reug reug defal nank déjà xamo wakh yaw danga yakarni ya meun si lamb jii mais yangui nakh 6:39 sa bopp so foguéni danga dakh beurré boy niang yangui nakh sa bopp boy niang mingay minimisé wallahi dinala béte yangui wakh rkk

  • @user-nh2rf7dv1n
    @user-nh2rf7dv1n20 күн бұрын

    Reuk reuk moye mbeur nak bilaye goor fit

  • @tallatamba8487
    @tallatamba84874 ай бұрын

    Kiiii môme vrai fou là 😂😂😂😂

  • @user-fe7jt1el3c
    @user-fe7jt1el3c4 ай бұрын

    Lou reug reug wakh deugue leu lamb Amoul kharit sport laaa

  • @coulzjamdong4764
    @coulzjamdong47644 ай бұрын

    Reug 2porte Eumeu bimouy wakh nioune ma pikine yeup mine nagn ko mingui wakh lou yag ndysane😂

  • @user-ps9fi7xr4d
    @user-ps9fi7xr4d4 ай бұрын

    Albourakh dina danel lutte tv 😂

  • @cheikhmourtallafall6776
    @cheikhmourtallafall67763 ай бұрын

    😂😂😂😂 vrai dof

  • @TigerLionn
    @TigerLionn4 ай бұрын

    Reug me doff la

  • @cheikhdiop9673
    @cheikhdiop96734 ай бұрын

    reug reug boul dieul lac guis na sa défaite boko dieulé wax nalako nakk sa victoire migui ci boy Niang ta fou lérr lako tékk bou dieul lac2 bakhoul ci yaw dieuleul boy Niang

  • @ablayenittoudeugu1012

    @ablayenittoudeugu1012

    4 ай бұрын

    Mdr 😂

  • @takhandiaye255
    @takhandiaye2554 ай бұрын

    Reug reug 50 wakh you bokoul lay wakh

  • @ibrahimaka2981
    @ibrahimaka29814 ай бұрын

    Ladial sa thies kouy boy niang

  • @FrancoisFaye-xl8uy
    @FrancoisFaye-xl8uy4 ай бұрын

    Reug reug defa mouna fené combat balla boye niang ya gnew thi boy niang boy wakh deye khalat

  • @MoussaLy-zu9sz
    @MoussaLy-zu9sz4 ай бұрын

    Nioune khame naniou lépp mbour laniou deuk combine la nieuw nga mbour boul niou sonal da nga Bari wakh nopil

  • @xalimagui-officiel9001
    @xalimagui-officiel90013 ай бұрын

    Manam nimay wakhé ngay xamni dof la

  • @user-qt6ff4en6h
    @user-qt6ff4en6h4 ай бұрын

    Reug reug vs eumeu sene le

  • @AhmaNdoye-oq2et
    @AhmaNdoye-oq2et4 ай бұрын

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @amadousouleyetandine931
    @amadousouleyetandine9314 ай бұрын

    Reug reug dou nitt

  • @amadousouleyetandine931

    @amadousouleyetandine931

    4 ай бұрын

    Wakh nga DEUG boy Niang moy sama mbeur mais daguèn wara beurré

  • @user-ci4xt8vx8k
    @user-ci4xt8vx8k4 ай бұрын

    Ki d'où nit

  • @BaMasour
    @BaMasour4 ай бұрын

    Kone lokho bôme Yi danou KO téyé

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara9234 ай бұрын

    Lamb amoul xarrit kone kèye démal beuré ak eumeu sène boul daww peleton

  • @user-ox2wf7dc5i
    @user-ox2wf7dc5i4 ай бұрын

    Mâlen ko wakh fi loumou nara am wakh dinako yakhal

  • @elhadjiserignetoure8698

    @elhadjiserignetoure8698

    3 ай бұрын

    😂😂 bilahi

  • @ibou1061
    @ibou10614 ай бұрын

    Reug Reug vs Siteu dinagnou beuré wala?

  • @leuz.patriote

    @leuz.patriote

    4 ай бұрын

    Waww😂😂😂😂

  • @cirely3220
    @cirely32204 ай бұрын

    Boy daga hamoul degaul dou ragal

  • @amadugningue8168
    @amadugningue81684 ай бұрын

    Mai reug ya meuna fen kou amoul dolé nga bolé 2 tank yi té mouno ko dan yen ñeup dangen di daw peuleton yaw eumeu sene siteu boy ñiang yenay andeu fekhel wa keur double less

  • @ibrahimathiaw7391

    @ibrahimathiaw7391

    4 ай бұрын

    Khana danan nk sa thies deif na ko 4 aput ms Reug dan nako dh

  • @user-dv3ld4iq4w
    @user-dv3ld4iq4w4 ай бұрын

    Ki doff la wéroul

  • @mouhamethniang3154
    @mouhamethniang31544 ай бұрын

    Reug reug dafa doff boula modou lo diapee df la lou kate ndeyam da nga beuri wah rek khaliss rek nga beugeu

  • @MamadouDiouf-hl1sy

    @MamadouDiouf-hl1sy

    4 ай бұрын

    Damaye kate sa daye

  • @ouzermatresetepenre1025
    @ouzermatresetepenre10254 ай бұрын

    Reug vs bombardier combine leu bombardier n'a jamais lutté ainsi durant toute sa carrière

  • @boubacarwelle4314
    @boubacarwelle43144 ай бұрын

    Franchement reug reug mounoule communication boye niang bi mou sokhla balla gaye 2 dafa beurré ak sathiess dane ko beug nga modou lô djieuleule franc c quoi ton problème mbapate ak arène nationale bokoule déé

  • @leuz.patriote

    @leuz.patriote

    4 ай бұрын

    Sa thies moy sama mbeur me reug deug leuh meunoul communication me mo meun franc deh😂 mod lô souko dieulè danou dolè yamoul ak force

  • @momobouthiapathiolybi7752
    @momobouthiapathiolybi77524 ай бұрын

    Ya ngi wakh rk boye niang mo meun sa thies mi la meun deil talakhou rk do touss

  • @user-pg4hb6ky9v
    @user-pg4hb6ky9v4 ай бұрын

    Nn ki doff bou makk la

  • @user-wj8pp5ri9c
    @user-wj8pp5ri9c4 ай бұрын

    Kii vrai doff laa

  • @aliousarr2874
    @aliousarr28744 ай бұрын

    Il communique mal

  • @moustaphabeye7869
    @moustaphabeye78694 ай бұрын

    Dof bou mac

  • @dioufaliou4384
    @dioufaliou43844 ай бұрын

    Sa thiès mola meun wagnil wakh djou bari

  • @keroukoukeroukou4686
    @keroukoukeroukou46864 ай бұрын

    Vraiment reug reug tu n’est pas du tout sportif accepte que sa thies t’as battu en plus tu communiques mal tu te prends pour le héros de l’arène mais tu te trompes je dis que sa thies sera rois des arènes avant toi et tant d’autres

  • @221baddest
    @221baddest4 ай бұрын

    Il est bête reug reug

Келесі