REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invités : GALLO BA & MODOU LO - 11 Juin 2018 - Partie 2

Ойын-сауық

Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine / tfm
/ replaytfm

Пікірлер: 155

  • @mbackeseck6142
    @mbackeseck61423 жыл бұрын

    Kouko sétan 2021 mariane yalla nako yalla yeureum

  • @aitasow7823
    @aitasow78236 жыл бұрын

    machalla mon lutteur préféré ci kaw ci kanam inchalla on va bocou prier pr toi modou Kharagne lo 💪💪💪

  • @babaanne3923
    @babaanne39236 жыл бұрын

    Ndam rek inch'Allah modou lo fans numb 1guediawaye

  • @lhommedelarivegauchedufleu6872
    @lhommedelarivegauchedufleu68726 жыл бұрын

    Machallah Sama mbeur bi Modou xaragne Lô ma bëgg lolou, je t'adore beaucoup et je t'estime beaucoup bakh gua yarou gua tey gua dale gua teh amm gua classe Machallah bokko ak yeneen mbeur you doff yii

  • @mouhamedalamin6995

    @mouhamedalamin6995

    6 жыл бұрын

    L'homme De La Rive gauche Du Fleuve Sénégal ki daye comédie rk

  • @amadoudiop704
    @amadoudiop7046 жыл бұрын

    Modou lo bilaye inchalla digua am ndam

  • @atoufall6490
    @atoufall64906 жыл бұрын

    Modou Ndam rek machalla

  • @serignetakkricain1339
    @serignetakkricain13396 жыл бұрын

    Moye sén baye de ak modou rek 💪💪💪

  • @afrieuroeurafrica7579

    @afrieuroeurafrica7579

    6 жыл бұрын

    serigne takkricain tarkinda abonné vous ma chaîne s'il vous plaît

  • @serignetakkricain1339

    @serignetakkricain1339

    6 жыл бұрын

    SENegaL السنغال wa yage na

  • @afrieuroeurafrica7579

    @afrieuroeurafrica7579

    6 жыл бұрын

    serigne takkricain merci grand ou frères

  • @lhommedelarivegauchedufleu6872

    @lhommedelarivegauchedufleu6872

    6 жыл бұрын

    +serigne takkricain wawaaw xaragne dou ayy thiakhane ndanaan leu

  • @lahad4894
    @lahad48946 жыл бұрын

    Modou Lô ndam rk inshallah

  • @ablayediagne6776
    @ablayediagne67766 жыл бұрын

    modou lo ya nite yalla nala yalla lafal thiat ça kaw ça kanam rk inchallah

  • @mamadousarr8747
    @mamadousarr87476 жыл бұрын

    Ohh Modou lô ya bakh yarou té amm teguine .Balal gnilay wakh danga sokhor wala sa khol mo bone .Ndèysaan masha'Allah yalnala Yalla may ndam bou lèèr.

  • @matydiop9313
    @matydiop93136 жыл бұрын

    Sama champoin bi modou loo

  • @afiamediatvsenegal6733
    @afiamediatvsenegal67336 жыл бұрын

    Modou Lathiale 300 millions so amé foula

  • @mameboye1
    @mameboye16 жыл бұрын

    Best QG ever much LOVE for modou lo

  • @globalccitix2233
    @globalccitix22336 жыл бұрын

    Modou est telment simple bougoul wakh bou niaw ndeyssane di rafatel rek il parle en bref mansh'Allah

  • @lhommedelarivegauchedufleu6872

    @lhommedelarivegauchedufleu6872

    6 жыл бұрын

    Nitt leu motaax deffa nitté mom dou doff teh deffa yarou

  • @Tahirousarrforever7418

    @Tahirousarrforever7418

    6 жыл бұрын

    Modou lo dafa bakh amoul béna problème

  • @moussanicena2090
    @moussanicena20906 жыл бұрын

    Nice na champion Moudou Lo

  • @tk92221
    @tk922214 жыл бұрын

    Modou lo a été victime d’un complot ci combat ak balla de 2019, gaston ak aziz nio teugg combat bi ensuite combat devait être le 1/01/19 et ils l’ont repoussé au 13. C’était un combat politique.

  • @adamcam2695
    @adamcam26956 жыл бұрын

    Ndam reek xaragne inchallah 🙏🏿🙏🏿 Mais les gens qui insultent gratuitement la vs êtes normaux ? Li sport la reek ni nguen di def di yée fittneu xolateleen seen booppe !

  • @souleymanediagne8292
    @souleymanediagne82926 жыл бұрын

    Balla yaw ba legui wakho modou Balnala akh mom mola balou mai pa yaw lamb day djekh doff nga trop thienaba yeup gningui sii xaragn khamal loumala wakhoul nak bo yakaré mystik mom mane nga bagna dem

  • @oumardieye4812
    @oumardieye48126 жыл бұрын

    MODOU lo yaw Ndam Rek inchalla

  • @fatykonate8173
    @fatykonate81736 жыл бұрын

    De tout cœur avec toi notre khargne yalla nalla yala may ndame si barké khadimou rassoul ak wérou koor bi incha allah

  • @elmgtv9591
    @elmgtv95916 жыл бұрын

    Bravo pape cheikh tu es trop fort macha alla🙏🙏🙏

  • @omardiop5563
    @omardiop55635 жыл бұрын

    machalla Modou lafe thiat Modou LO bou ababacar

  • @cheikhmbackediop7678
    @cheikhmbackediop76786 жыл бұрын

    Nékha farall dimanch ya sonall sai non dh bravo xlo

  • @souleymanegueye6359
    @souleymanegueye63596 жыл бұрын

    Modou mola makk wayé ioe yak nga sa yaram bou yagg xlo day xalat aprés lamb dji Santé bii noumouy demé hygen de vie dafa bakh thi sportif modou ndam rkk Inchala

  • @boubafall1014
    @boubafall10143 жыл бұрын

    Mod’lo ❤️

  • @papandiaye9419
    @papandiaye94196 жыл бұрын

    affaire bi dal xaragne Lo laa moy souniou champion si kawaw si kanam ba roi des arénes

  • @Tahirousarrforever7418

    @Tahirousarrforever7418

    6 жыл бұрын

    Inchallah yalla bakhna

  • @papandiaye9419

    @papandiaye9419

    6 жыл бұрын

    inchalah

  • @isandiaye4439

    @isandiaye4439

    6 жыл бұрын

    Modolo danko billahi

  • @gueyemamediarra5157
    @gueyemamediarra51576 жыл бұрын

    Modou lô ndam rékk inchallah

  • @tafsillah6577
    @tafsillah65776 жыл бұрын

    INSAALLAH modou lo Ndam rek

  • @ramabadji1965
    @ramabadji19655 жыл бұрын

    Vraiment j'aime cette homme. XLO ci khol for ever lélène khadiou ci

  • @adjabintoudrame7217
    @adjabintoudrame72176 жыл бұрын

    Merci Balla❤️❤️🔐

  • @barandiaye601
    @barandiaye6015 жыл бұрын

    Yallá nala yallá May ndam thi kaw balla gaye 2

  • @kyandiaye4855
    @kyandiaye48556 жыл бұрын

    man dal ma beugu modou lo pirr marchalla

  • @aidaseck3821
    @aidaseck38216 жыл бұрын

    machalla amna solo

  • @absafane4324
    @absafane43246 жыл бұрын

    Tu as de la classe de l élégance je t estime bcp bilahi m odou diam rekk ngay am ak ay ndam you bari incha allah

  • @khadimsow2320
    @khadimsow23205 жыл бұрын

    XLO nena nan kodef ndakk balamo toye.mboussou ndokh dou darà ndam rek inchalla XLO

  • @thiabetvweb990
    @thiabetvweb9906 жыл бұрын

    bilay modou mo am classe sa mbeur mi kéne douko dougal ci détail

  • @cheikhtalibuoyesaadbouh7193
    @cheikhtalibuoyesaadbouh71934 жыл бұрын

    Modou lo ndam rek Inchallah 💪

  • @abassfall5593
    @abassfall55936 жыл бұрын

    Kharagne 100 %

  • @kyandiaye4855
    @kyandiaye48556 жыл бұрын

    bilay maleu beugu yalla bakhna yalla naleu yalla may guoudou fann ak werr mayleu ndam rek

  • @GorabouTalfa
    @GorabouTalfa6 жыл бұрын

    modou lo lou leer guan wakh balla mola gueuneu kham lolou balla amatoul dollé legui

  • @countryman29
    @countryman296 жыл бұрын

    Modou ndam rek

  • @afrieuroeurafrica7579

    @afrieuroeurafrica7579

    6 жыл бұрын

    people choices chanel Abonné vous s'il vous plaît

  • @BassirouNdiaye662
    @BassirouNdiaye6626 жыл бұрын

    Mercie balla

  • @cheikhoulkhadimcheikhoulkh1684
    @cheikhoulkhadimcheikhoulkh16846 жыл бұрын

    Yalla nala yalla may dame ci barke cheikhoul khadim

  • @lamplo3355
    @lamplo33555 жыл бұрын

    Hum bakhna modou rek

  • @thiabetvweb990
    @thiabetvweb9906 жыл бұрын

    les chroniqueur de tfm da niack professsonnalisme pourkoi invité diko wone sa far si adversairame

  • @BassirouNdiaye662
    @BassirouNdiaye6626 жыл бұрын

    Nice na trop modou lo

  • @pacond5341
    @pacond53416 жыл бұрын

    Ndam rek inchalla modou

  • @afrieuroeurafrica7579

    @afrieuroeurafrica7579

    6 жыл бұрын

    Paco Nd Inchallah modou moy dane ajouter moi come contact abonné vous s'il vou plaît Ajoutez-moi comme contact sur KZread. youtu.be/addme/5aemSzCtJjxtbW8o1lt9QdNzQTzDvw

  • @kyandiaye4855
    @kyandiaye48556 жыл бұрын

    laff inchallah ndam rek

  • @mamadousaliouba4008
    @mamadousaliouba40086 жыл бұрын

    balla mòy bandit.nàp na modou lo😂😂😂

  • @ndiayeabdouaziz8568
    @ndiayeabdouaziz85686 жыл бұрын

    Invite Mr. Sonko

  • @amadouba5853
    @amadouba58536 жыл бұрын

    Ndam rek modou

  • @hamdylo5663
    @hamdylo56636 жыл бұрын

    Modou lo rk

  • @papeciss686
    @papeciss6866 жыл бұрын

    Ndam reik inchallah

  • @anthioumanefadiga9314
    @anthioumanefadiga93146 жыл бұрын

    Barki Serigne touba mala beug Mbeur. Yay champion

  • @thiapa6489
    @thiapa64894 жыл бұрын

    Modou Lo wanna rouss deh 🤣🤣🤣🤣🤣

  • @ibrahimakane7128
    @ibrahimakane71286 жыл бұрын

    Modou Lo aferbi yawla

  • @mamediarrawade4227
    @mamediarrawade42276 жыл бұрын

    man thiate bou xaragne lò inchala dame rekk

  • @alioukane5937
    @alioukane59376 жыл бұрын

    Modou lo rek

  • @Africandream12
    @Africandream126 жыл бұрын

    Ngagne diagne khawma ioe mom vrai nafékh nga

  • @serignefalloufall1603
    @serignefalloufall16036 жыл бұрын

    Dagne koumpa amna combat bi taxawna modou lô dalen di fonto

  • @ablayethiam6495
    @ablayethiam64956 жыл бұрын

    Xaragne lollllllllllllll yafiné amoul lénéne

  • @moramyfallamy1410
    @moramyfallamy14106 жыл бұрын

    Il fau invite sonko

  • @babacarseck9694
    @babacarseck96946 жыл бұрын

    way paby sof na torop ta bari wax ish modou motax niouy setane l emission ish

  • @douabzizadiagne3739
    @douabzizadiagne37396 жыл бұрын

    Modou ya mana tontou t3 siviliz3

  • @basskane241
    @basskane2416 жыл бұрын

    mom tay nga masa wakh louma nékh

  • @laminendiaye6158
    @laminendiaye61586 жыл бұрын

    Moudou yaye sai sai xaragne lo

  • @alladiop5415
    @alladiop54156 жыл бұрын

    Hahaha mè ki dou guenar kokile

  • @jaspoo2532
    @jaspoo25326 жыл бұрын

    Modou ak balla yeup ay champion nguen

  • @amadoudiop704
    @amadoudiop7046 жыл бұрын

    Talibe serigne babacar dou ragal

  • @doudousarr4777

    @doudousarr4777

    6 жыл бұрын

    Amadou Diop arrête avec ça que fait un grand homme comme serigne Babacar Sy rta ds un combat de lutte.Soyez sérieux.

  • @amadoudiop704

    @amadoudiop704

    6 жыл бұрын

    Doudou Sarr balma cone ok

  • @Tahirousarrforever7418

    @Tahirousarrforever7418

    6 жыл бұрын

    Vraiment

  • @issatoure5949

    @issatoure5949

    3 жыл бұрын

    Merci

  • @bayezallezalle195
    @bayezallezalle1954 жыл бұрын

    Ki moy dou looo

  • @ismailatambedou7767
    @ismailatambedou77676 жыл бұрын

    Modou rk

  • @lhommedelarivegauchedufleu6872
    @lhommedelarivegauchedufleu68726 жыл бұрын

    Modou nakk mounonegua tontou Balla tontou bou saff sapp bamou xam bopam gua bayi sa yarou dji Balla khamoul yarou soy wakh ak mom deguay reew ni mom boba di yam teh dina kham bopam

  • @Tahirousarrforever7418

    @Tahirousarrforever7418

    6 жыл бұрын

    L'homme De La Rive gauche Du Fleuve Sénégal Modou face à face bi laye khar Balla guisso goul dara

  • @inssan9508

    @inssan9508

    5 жыл бұрын

    😂😂😂.!! 2:0 yi daal dolen ko meusseu fatté.!😂

  • @elhadjidiawkabir3516

    @elhadjidiawkabir3516

    3 жыл бұрын

    Iow danga wara khamne balla dousa morom finga néka di null rék

  • @damenianght
    @damenianght6 жыл бұрын

    issa cisse

  • @harounadiacko9600
    @harounadiacko96005 жыл бұрын

    M k lo Macha lakou

  • @khadimsene7546
    @khadimsene75466 жыл бұрын

    Aver bi balla gaye 2 la

  • @mouhameddieye7486
    @mouhameddieye74866 жыл бұрын

    Yaar ak téeguine

  • @noelitooba7812
    @noelitooba78126 жыл бұрын

    Ama Baldé moy dérangé mo takh wayé wiri-wiri jari-ndaré

  • @aminatadiallo4702
    @aminatadiallo47026 жыл бұрын

    Wa papa ngagne iow laniouy lath wala modou doko bayi mou waxx ha non waay en plus pa bi daye diakhassé

  • @aladjimbacke9215
    @aladjimbacke92156 жыл бұрын

    mala beugge

  • @oussboys4057
    @oussboys40576 жыл бұрын

    Modou lo kou khol bi moo Bonn ndym mei force niou. danat. La ndym

  • @afrieuroeurafrica7579

    @afrieuroeurafrica7579

    6 жыл бұрын

    ouss boys cv abonné vous s'il vous plaît

  • @BassirouNdiaye662
    @BassirouNdiaye6626 жыл бұрын

    Père sa lafall ndaye

  • @Billy_skurt
    @Billy_skurt6 жыл бұрын

    non balla dafa gueum bopam bilahi

  • @layediallo4005
    @layediallo40056 жыл бұрын

    Sidate wahnga deug

  • @jaspoo2532
    @jaspoo25326 жыл бұрын

    Sama gayi bayilen togn nk balla fila tok diko treter modou comme guinar kokoli t wakholen dafa soxor

  • @malifeoui6759

    @malifeoui6759

    5 жыл бұрын

    pape diop mais c'est juste pour faire la pub du combat

  • @jaspoo2532

    @jaspoo2532

    5 жыл бұрын

    ma life oui motakh mani bou kenn wakh modou da sokhor daniouy nexal rk

  • @cheikhniang6920
    @cheikhniang69203 жыл бұрын

    Mmachialla papechiekh diallo llafffuettte dabakhrrkkk

  • @maremedrame1203
    @maremedrame12036 жыл бұрын

    Balla bayil sop

  • @mfn9511
    @mfn95116 жыл бұрын

    Guinarou kokeli

  • @cheikhmbackediop7678

    @cheikhmbackediop7678

    6 жыл бұрын

    Modou Niass2524 mbosou ndokh dafa siméko Modou néna ma rouss

  • @kyandiaye4855
    @kyandiaye48556 жыл бұрын

    they yalla modou mo civilisé

  • @oussboys4057
    @oussboys40576 жыл бұрын

    Ngangé Diange moo soff dobayi Modou Lo mo wakh ah

  • @afrieuroeurafrica7579

    @afrieuroeurafrica7579

    6 жыл бұрын

    ouss boys Cv merci abonné vous ma chaîne

  • @aminatadiallo4702

    @aminatadiallo4702

    6 жыл бұрын

    ouss boys franchement

  • @boubafall1014
    @boubafall10143 жыл бұрын

    Mod’lo kén dou moom si lamb j

  • @diabakarasikori2604
    @diabakarasikori26046 жыл бұрын

    moudolo boull tett bou ragall bax baxa yi mege tewo

  • @dioufsega416
    @dioufsega4166 жыл бұрын

    Pape cheikh Diallo saytané pirr diaxassé Rèk gua nék Sénégal ba pré gua yakar ni yathi né nioulay diay té xamo dara amo xam xam violence Rèk guay Andi Sénégal invite mbeur yi invite oustaz yi invite politique chien di diaxassé Rèk

  • @oussoudiallo6976
    @oussoudiallo69766 жыл бұрын

    First

  • @afrieuroeurafrica7579

    @afrieuroeurafrica7579

    6 жыл бұрын

    Oussou Diallo Gool bro Abonné vous ma chaîne

  • @vincentemmanuel8121
    @vincentemmanuel81216 жыл бұрын

    Franchement Pape cheikh je t'aime bien et tout dans le meilleurs des mondes mais franchement la lutte c'est pas ton fort ! Y a une façon de poser les questions et d'attiser la tension entre les gens concernés !!!

  • @stevengerrard3473
    @stevengerrard34736 жыл бұрын

    balla lutah nga neik ngaka kula bayi ngani ya eup mod lo ay suporter li modu wah mosi neik lamb diodiou amateur sefeur boxeur karateka yep dem stad ken teguko sah radio rawatina tele yi ngay wah di compare you bokul

  • @sayenaboundiaye4856

    @sayenaboundiaye4856

    6 жыл бұрын

    Balla day fen rek

  • @itnodrame7836

    @itnodrame7836

    5 жыл бұрын

    @@sayenaboundiaye4856 maintenant tu sais que c'est modou lo le menteur

  • @laminedia1741
    @laminedia17416 жыл бұрын

    balla boula moudou diapie

  • @maryamkante201
    @maryamkante201 Жыл бұрын

    wareffe

  • @jaspoo2532
    @jaspoo25326 жыл бұрын

    Modou femme bobou di toggou balla moy mbereum domam ocii balla lay noyei tei balla demb la diougguei fofou mome mou avouer ko si kanamam ATTENTION! Encore ma cetlou folen di dem molassi djittou mola ndiekkeu dieul avance mo diapp date mola ndieukka tek plan dentrainnement ba emission bobou sah mome laniou niekka dieul fait attention que sportivement le gars soit pret en premier que toi.

  • @marleysane7154

    @marleysane7154

    6 жыл бұрын

    pape diop iow doff nga rek Dego modou nena dou Khar ba am combat soga entrené Modou nena combat wam ak lac bimou dekhé la beugona beurewat

  • @souleymanegueye6359

    @souleymanegueye6359

    6 жыл бұрын

    Danio bakh rkk meunalouniouko dara modou yalla mokay aral bopam

  • @jaspoo2532

    @jaspoo2532

    6 жыл бұрын

    Marley Sane lol ioa nak nexoul ba nexoul yaye con bi un combat de lutte ne se prepare pas comme ça nganane comba wame bimou "dekhei" lol dieulal sa tmp nga xol lima wah. Mbeur yeup daniou nane la parei naniou alors que nioungui lakatou di entrainner cest comme le cas de balla a 2STV il a crier fort que bou combat bi nekkone souba sah parei na alors dague ne biellei france pour 6mois sou parei wone nako df?. Deggo modou oci nela mome tegagoul plan dentrainement mais bou diarrei dm europe mou dm? Lolou kou parei nako wah. Chimm Bou nite yi di wah dangay xol fond bi tei bania yam si forme bi boul yakamtei doul. KONNN

  • @marleysane7154

    @marleysane7154

    6 жыл бұрын

    pape diop iow ay retane nga ma deff kom khalé bouy sogua dioudou combat bou donn souba ma beuré lolou wakhine Dama la beug wakh ni Modou lo dara dou ko bett thi lamb thi gatal

  • @jaspoo2532

    @jaspoo2532

    6 жыл бұрын

    Marley Sane eske do retane sa boppou bo xamul lamb niou wahlako lamb kenn doussi parei modou waxnalako nenala lamb ay detail la ioa nga begue ko pArei lo. Bay fall kinga preparei neikk xalei niow mou dane la si 21s meun nga tok fii nane parei ngako lol a moins ke nga ndogo ay guinar ak moutarde lol

  • @omarbadji5133
    @omarbadji51335 жыл бұрын

    NON WAX BAKHOULE TEYE 2-0 leu

  • @mfn9511
    @mfn95116 жыл бұрын

    Ngagne diagn dafa sof bouy wax dafay fok ni mome rec mo xam lamb go way

Келесі