Réponse de Cheikh Modou Kama à (SUNGUE = SANGARA) Babacar Ndiaye Mi Wakhni Yalla Dafa...

Imprégnez vous des enseignements et des valeurs de la tarikha à travers ATTIDJANIYA. Abonnez-vous à nos différentes plateformes !
Page Web : www.attidjaniya.org
WhatsApp : whatsapp.com/channel/0029VaTW...
X : x.com/attidjaniya?s=21
Tik Tok : vm.tiktok.com/ZMMMN1L5M/
Facebook : share/v/XRup...
KZread : youtube.com/@ATTIDJANIYAHTV?s...

Пікірлер: 146

  • @CHEIKHMARABASS
    @CHEIKHMARABASS20 күн бұрын

    Waw gorr machalla

  • @IbouSall-kw3zy
    @IbouSall-kw3zyАй бұрын

    جزاك الله خير

  • @mohamadoulaminediallo4967
    @mohamadoulaminediallo4967Ай бұрын

    Dieureudieuf serign bi

  • @thiernomamadoudiallo5496
    @thiernomamadoudiallo5496Ай бұрын

    Alhamdoulilah bignou yalla thi djaboute cheikh Sangue Mouhamed diop khamni yalla, yonente ak Cheikhou Tidiane

  • @mamadousow7917
    @mamadousow7917Ай бұрын

    Machallah yaa Oustaz. Xam xam bi lerna.

  • @AbdoulayeDiouf-wz2ny
    @AbdoulayeDiouf-wz2nyАй бұрын

    Oustaz modou yallnala yalla faye

  • @aboubacryly7692
    @aboubacryly7692Ай бұрын

    Dieuredieuf cheikh modou kama

  • @user-ju9br1cy3v
    @user-ju9br1cy3vАй бұрын

    Merci beaucoup modou .ndiaye kou kat ndayam le

  • @MOUHAMAD548
    @MOUHAMAD548Ай бұрын

    Merci beaucoup ❤❤❤ cheikh modou Kama

  • @leuzkane
    @leuzkaneАй бұрын

    sukran laka

  • @wakhdeugguetayallatakh8129
    @wakhdeugguetayallatakh8129Ай бұрын

    Ma challakh

  • @user-zn4pn7wt3z
    @user-zn4pn7wt3zАй бұрын

    ❤❤❤ merci s.modou kama ❤❤

  • @mansourniang4521
    @mansourniang4521Ай бұрын

    بارك الله فيكم سيدي محمد كم جو

  • @moussadiop7206
    @moussadiop7206Ай бұрын

    Machalla amna solo

  • @abdoulazizsarr1726
    @abdoulazizsarr1726Ай бұрын

    أيدك الله ونصرك وزادك علم الدني

  • @mohamedmbaye647
    @mohamedmbaye647Ай бұрын

    Keep kouy joullite Warga dénoncer mbaam jaay

  • @hotsy3005
    @hotsy3005Ай бұрын

    Mancha allah

  • @dakhirousy5143
    @dakhirousy5143Ай бұрын

    Ki deh kaddu yi sah amoul leer. Yalnala yalla may deg deg , yow deh halé nga si diné

  • @MamadouLamine-qr8cj
    @MamadouLamine-qr8cjАй бұрын

    ايدك الله ورعاك

  • @user-xn2mp2fs9m
    @user-xn2mp2fs9mАй бұрын

    ❤ Amna solo

  • @mamadoundiaye1563
    @mamadoundiaye1563Ай бұрын

    ❤❤❤

  • @khalifaababacarNiang313
    @khalifaababacarNiang313Ай бұрын

    Niou mélni la diiné dji sokhela wayé nitt yo khameni enquesse xaliss nitt yi Dilen djarigno

  • @papadiargadiouf7037
    @papadiargadiouf7037Ай бұрын

    😂😂😂😂😂 bon xatarayou

  • @dakhirousy5143
    @dakhirousy5143Ай бұрын

    Demal wouti xam xam, bou dei lingay wah NGA diapé xam xam yangui nah sa bop

  • @cheikhsadiboumane1420
    @cheikhsadiboumane1420Ай бұрын

    لا تصوف فى الاسلام

  • @khalifaababacarNiang313
    @khalifaababacarNiang313Ай бұрын

    Tarikha tidjane bougne déme bakoye diame rék niasén yi nioka warale ndakhe meune bokalé

  • @makhtarcisse-ft1dq

    @makhtarcisse-ft1dq

    Ай бұрын

    Wallahi wax nga deug

  • @baragaye2018

    @baragaye2018

    Ай бұрын

    Fa niasse yi fèkone tarikha bi ak fa niouko yobou. Yène deh sou done yène dong kène wakhatouko. Baye mo dèkal l'islam dèkal tarikhabi. Kouko santoul do nitt kou bakh. Les chiens aboient la caravane passe

  • @aboubacryly7692

    @aboubacryly7692

    Ай бұрын

    Bilahi wahh nga deugg gnii ay mbaam lagnou

  • @mouradmbaye2690

    @mouradmbaye2690

    Ай бұрын

    Wallabies dagay fein teiga tontou sangu Ndiaye rek tivaouane bobou nga bokk ay kilifeu wakh naniou feu ay wakh yoo hamni yeifeur rek mooko meuna wakh tei takhoul nga wakh ci

  • @sanguebitv8429

    @sanguebitv8429

    Ай бұрын

    Saway wakhal xam xam té bayi togne

  • @baragaye2018
    @baragaye2018Ай бұрын

    Kou yalah yiir naka ngay wakhalè l'islam ? Yaw sène keur boufa kène bonnè ndakh danioukay askanalè sen wakeur yèp ? D'abord yaw mandouwo baparé nga beug até. Yaw yalah yoni woula dinkounioula dinédji. Linga rèré mo eup linga xam. Gningay inkar kathia gueuneu ndaw mola raw ci yalah.kêp kou yalah alak dangay inkar Baye. Kou dougeul lou eup 500millions ci dîné dji amolène loy def loudoul diko khass aka garal. Yaw yay abou dial tigui. Bofèkéwone Yonènetébi nga khass ko. Khamalo yalah dara. Dèmal xam yalah dieuk. Même discourbi fassawoul. Niata niou bone nio nèk ci l'islam, da takh l'islam bone ?

  • @makhtarcisse-ft1dq

    @makhtarcisse-ft1dq

    Ай бұрын

    😂😂😂😂sa discourt bi safoul yalla ki limou wax deugeula

  • @bayeserignembengue9704

    @bayeserignembengue9704

    Ай бұрын

    Salam Yaw diné dji diné Buur'YALLA leu kénnn momou keu li moy Sénégal bo waxé lou boon djeumeulé ko tchi borom kénnn dou mérrr bo lalé Serigne gneup djogu moy kon Serigne yi gno gueun borom bi OUSTAZ BI LOUMOU WAXXX DEUG LEU WA SALAM

  • @bayeserignembengue9704

    @bayeserignembengue9704

    Ай бұрын

    Sa discours bi dh flafla leu seugue Ndiaye ( domraam pirr ) kouko topou kénn doula djitou Safara Seugue Ndiaye xamoul dara tchi Buur'YALLA xamoul dara tchi tarikha tidianes bi xamoul dara tchi makhrifa bilae mais nakkkkk sa explique racines bi mo amme problème

  • @ibrahimaba3905

    @ibrahimaba3905

    Ай бұрын

    Dieuredieuf Serigne Modou kama Yallana boroom bi samla , takhawoula.YEN LA DÎNÉ SOKHLA MAIS PAS AY MBAME SEUF YOU MELNI SEUNGUE NDIAYE

  • @salieumbai810

    @salieumbai810

    Ай бұрын

    500million tamit barina di 😮

  • @makhtarcisse-ft1dq
    @makhtarcisse-ft1dqАй бұрын

    Dieureudieuf way niila rek

Келесі