Prière de la Tabaski : Khutba de Imam Galadio Kâ "Limay Deek Président Bassirou Diomaye"

Prière de la Tabaski : Khutba de Imam Galadio Kâ "Limay Deek Président Bassirou Diomaye"

Пікірлер: 149

  • @xalicodia9581
    @xalicodia95819 күн бұрын

    Machallah ❤❤❤❤❤❤❤ Aïd Mabrouk à toute la Ouma islamique sous la bénédiction du tout Puissant Allah

  • @OusmaneLy-cv5nd
    @OusmaneLy-cv5nd9 күн бұрын

    ❤😢😢😢😢😢man dd titna Sénégal 🇸🇳 legui mag ,ndaw goor , jiguen kou wah gnou saga ahhhhhh k Dieu nous guide sur le droit chemin ❤

  • @user-mi7sb5nn1e
    @user-mi7sb5nn1e9 күн бұрын

    Macha allakh yalna léne yalla Faye yéna ngui takha wou dîné dji Sénégal bou Bari won gnou mélni yén Dina bakh lôll yalna niou yalla mousal si ahlou bidda AK séni pekhé sunnah rk Moy DEUGG ❤️❤️❤️❤️

  • @septchaine

    @septchaine

    9 күн бұрын

    😅 Thiey les Guinéens

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    ahlu bidah mo tane ahlu fen 😂😂 xamu leen darra sen xolyi lëndeum na bounna

  • @fatoumatabintoucolley8878

    @fatoumatabintoucolley8878

    9 күн бұрын

    @@FOCUSS32yena geuna bone dii fen rek dieul serigne tegue ko thii kaw Yalleu dii wakh sama yakar tey akk euleuk

  • @mbddiop4671
    @mbddiop46719 күн бұрын

    MAROC MAURITANIE MALI ET SENEGAL PRIENT DEMAIN LUNDI INCHALAH. QUE DIEU ACCEPTE NOS DEVOTIONS. SOYONS TOLERANTS.

  • @mth1318
    @mth13189 күн бұрын

    Yalla nanou yalla déff ay nitou deug ...❤❤❤

  • @user-jq7sg1ub1f
    @user-jq7sg1ub1f9 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ma cha'ALLAH qu'ALLAH vous assiste et vous facilite la tâche

  • @youssoumanga5
    @youssoumanga59 күн бұрын

    Masha Allah al imam Galadio

  • @aboufat.5189
    @aboufat.51899 күн бұрын

    Normalement tous les pays musulmans doivent célébrer Aïd le même jour que la Mecque. Salama

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    macka du mo mom diine dji bayyil sen jakhan yi réer ngen torop

  • @serignetine1420

    @serignetine1420

    9 күн бұрын

    Nom lolou mounoul am nit yi bokkou gnou heure

  • @Aicha-xn7jk

    @Aicha-xn7jk

    9 күн бұрын

    Donc pourquoi Mecque souniou djoulé djouma vendredi nioun douniou bayi ba samedi​@@serignetine1420?

  • @aboufat.5189

    @aboufat.5189

    9 күн бұрын

    @@serignetine1420 niak bok heure n'empêche pas nieup bok jour comme Europe ak Maghreb ak Asie et certains pays Africains

  • @lobayefall2282

    @lobayefall2282

    9 күн бұрын

    @@Aicha-xn7jkpourquoi on prie pas le meme heure qu’eux Quand il prie nous on dort

  • @madinakane7761
    @madinakane77619 күн бұрын

    C'est bel et bien aujourd'hui la TABASKI. Le 9ème jour du mois est ARAFAT le lendemain c'est la TABASKI. Il est vrai que la fête est de 3 jours, le début est le 10e jour du mois de Zul Hijja. Ceux qui célèbrent le Lundi n'ont pas du tout raison. Ce Marabout a bien fait de célébrer la fête de TABASKI aujourd'hui. Il est un bon musulman et un sénégalais. Certains musulmans ne respectent plus la voix que le BON DIEU a tracé pour les croyants. C'est vraiment dommage. BONNE FÊTE DE TABASKI.

  • @habythiam1218

    @habythiam1218

    9 күн бұрын

    T'a tout dit merci beaucoup

  • @sonkodiomaye

    @sonkodiomaye

    9 күн бұрын

    Toi là tu connais ce que dieu a dis pour parler ainsi😢def leen lileen doy taa bagn sikkal kéneen islam contradiction yagg ci nekk leen nitt j'en suis sûr linga wax xamoci dara

  • @septchaine

    @septchaine

    9 күн бұрын

    Rien compris

  • @serignetine1420

    @serignetine1420

    9 күн бұрын

    Tabaskil rek rafet diorto yalla nagoulnala te yenné gnenen yi am tabaski

  • @fatoufall7203

    @fatoufall7203

    9 күн бұрын

    ​@@sonkodiomaye khamnagne li yalla wakh.Alkhourane moguifi . yalla wakh na thi lèpe

  • @user-ld9gm1pf3v
    @user-ld9gm1pf3v9 күн бұрын

    Macha Allah ya cheikh Ousmane kaladio ka❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamadybadji5
    @mamadybadji59 күн бұрын

    Machala qu elle discours de l'imame k dieu vous bénisse machala machala ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @Layla-zp4cn
    @Layla-zp4cn9 күн бұрын

    Alhamdulillah la fête de Tabaski cest le 10eme jour de dul hidja sa veut dire le jour après Arafat. Eid Mubarak tout le monde.

  • @diallodiallo4459
    @diallodiallo44599 күн бұрын

    Tabaski teyla dé

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    fen ga deh

  • @seydousambakoulibaly734

    @seydousambakoulibaly734

    9 күн бұрын

    Koone tey Tabaski leu ? Mais maane guissouma yaap, sentirou saaf , guissouma kou solou , degouma kouno dewenety. 99 % de la population du Sénégal prie demain Lundi

  • @fatoumatabintoucolley8878

    @fatoumatabintoucolley8878

    9 күн бұрын

    @@seydousambakoulibaly734nel nafekh yi nio diouli woul tey

  • @user-tu5do2bu1z
    @user-tu5do2bu1z9 күн бұрын

    Mashallah ya Ckheikh allahouma baarikk Respect et vérité Kou saga rek danga amoul arguments

  • @cheikhcamara4888
    @cheikhcamara48889 күн бұрын

    Belle leçon Ya Imam

  • @abdoulayediarra2525
    @abdoulayediarra25259 күн бұрын

    ❤❤❤جزاكم الله خير الجزاء

  • @assadia2010
    @assadia20109 күн бұрын

    Eid Mubarak a toute la ouma islamique❤

  • @mahmoudly4641
    @mahmoudly46419 күн бұрын

    Ma ngi côte d'ivoire ms tay lagn djoulli❤

  • @mbddiop4671

    @mbddiop4671

    9 күн бұрын

    MALI MAURITANIE MAROC Prient demain Lundi...senegal aussi

  • @BoubacarKa-ct9od

    @BoubacarKa-ct9od

    9 күн бұрын

    Ces votre problème ici au Sénégal ces demain lundi

  • @septchaine

    @septchaine

    9 күн бұрын

    ​@@BoubacarKa-ct9odbayiléne fof gni polymiq laniou beug

  • @fatoundong2812
    @fatoundong28129 күн бұрын

    Yen n'a wah déug nak machallah

  • @user-ku1dz5rm1g
    @user-ku1dz5rm1g9 күн бұрын

    Après Arafat c est la Tabaski

  • @amethdiaw3475
    @amethdiaw34759 күн бұрын

    بارك الله فيكم

  • @mariamasinyan6078
    @mariamasinyan60789 күн бұрын

    Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @americainba9848
    @americainba98489 күн бұрын

    Machallah imam

  • @mansoursy4979
    @mansoursy49799 күн бұрын

    Macha allah

  • @mouhamadalphadiallo9117
    @mouhamadalphadiallo91179 күн бұрын

    Massallah

  • @user-zq2vs5kj1f
    @user-zq2vs5kj1f9 күн бұрын

    MachaALLAH

  • @falyseydi
    @falyseydi9 күн бұрын

    Ma cha alah ❤❤❤❤❤

  • @salamndiaye9684
    @salamndiaye96849 күн бұрын

    Toutes les musulmans du monde on célébrer la fête aujourd'hui

  • @khadimcisse7387

    @khadimcisse7387

    9 күн бұрын

    C'est pas partout dh

  • @assadia2010

    @assadia2010

    9 күн бұрын

    Canada 🇨🇦 ont celebre aujoud8 parcequ hier etait arafah

  • @malangdieme1163

    @malangdieme1163

    9 күн бұрын

    C'est pas vrai

  • @harounaba8258
    @harounaba82589 күн бұрын

    Manchallah ❤

  • @Meunsablond08

    @Meunsablond08

    9 күн бұрын

    Téguo lenn fenn djouli taye

  • @user-lz1bi5eb9t
    @user-lz1bi5eb9t9 күн бұрын

    Mashallah

  • @zarataka1601
    @zarataka16019 күн бұрын

    Alhamdoulillah

  • @ahmadoulamine9548
    @ahmadoulamine95489 күн бұрын

    Thi ay thiakhane keep ngen nen 😂 koulen fék ngèni Wa makka ngéni andal tabaski kone kay delen book ak niom wakhtou djouly yi 😂 sen xam xam gateu na sen lamign reuy neu den xol leundeum neu😂 yalla nalen sunu borom guindi 😂🙏🏾

  • @habibmandiang4509

    @habibmandiang4509

    9 күн бұрын

    Démal djangue sa diiné moo guene

  • @fallousamsylla

    @fallousamsylla

    9 күн бұрын

    Walay ndaye sanne

  • @alphadiallo6742

    @alphadiallo6742

    9 күн бұрын

    Ioe en priant foy dioublou nespa macka?

  • @Muhammadsaneb

    @Muhammadsaneb

    9 күн бұрын

    Baylén tapalé boy Fi yalla rék mofi nék régal léne yalla bay parparlo

  • @amadoumdiallo3484

    @amadoumdiallo3484

    9 күн бұрын

    Y'a nè si thiakhane bou reuyy..beine arafat mo am ,moy bou makka, donc kou deif tabaski le lendemain mongui si yone.tei boul fatè ni amoul deukkeu bou gueune makke akh medine .tei dioullèfeu mo geune feippe fou dioullè te niou gueune si generation bi fofou laniou diouguè te teudde fe.la meilleur des êtres est aussi là-bas.donc wakho fi dara . Meune gua bania dioubo akh seni guiss wayè sa argument teigouwoul si kham kham ni si deugue

  • @kinely
    @kinely9 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MansourNdiaye-tq3kc
    @MansourNdiaye-tq3kc9 күн бұрын

    nafekhe ga djallo

  • @Yibrafalien
    @Yibrafalien9 күн бұрын

    Téggou léne féne diouli tay louléne nékh nguéne déf

  • @user-ld9gm1pf3v

    @user-ld9gm1pf3v

    9 күн бұрын

    Ana ça dalil bok mi

  • @yahyaabayawo7402

    @yahyaabayawo7402

    9 күн бұрын

    Nioun gni diouli Souba nioko tegout féne ndah Nioun nieup Nio defando Arafat dembou

  • @IbrahimaCisse-jn6nv

    @IbrahimaCisse-jn6nv

    9 күн бұрын

    Soo khamoul nooppil sama frère

  • @Yibrafalien

    @Yibrafalien

    9 күн бұрын

    @@yahyaabayawo7402 kon Makka nga nék ni déléne topou calendrier musulman racistes nguéne trop

  • @IbrahimaCisse-jn6nv

    @IbrahimaCisse-jn6nv

    9 күн бұрын

    ​@@yahyaabayawo7402 kham kham nga wakh nit kou woyof nga

  • @user-ix2ep9pg4t
    @user-ix2ep9pg4t9 күн бұрын

    Problème amna dh

  • @malickdiatta3822
    @malickdiatta38229 күн бұрын

    Combien de tabaski?

  • @DIOKO56
    @DIOKO569 күн бұрын

    Tope léne souna wahabites yi té bayniou tope souna RASSOULALLAH sounou souna màme you téde yi . La Mecque doo toul référence. Juifs yi niokoy géré mo takh niou diokhko Wahabites yi. SALAM.

  • @adjamariemediedhiou5837
    @adjamariemediedhiou58379 күн бұрын

    Pourquoi dawou ñu deg xoutba yi si tenwou maky sall? Mais batay rek on prend ndakh gni fi nek xam nañu li lène fal ndakh li nguène diangue lañu diangue heureusement que aye dioulit akane lañu wouté ak ki fi nekone ndakh kène xamoul wone li ñu done seytané bakhoul ak ndakh 12ans yi fi la lène fékone Machaa Allah on a un Président musulman qui le pratique et l’applique

  • @DieynabaThioub-vi1dd

    @DieynabaThioub-vi1dd

    9 күн бұрын

    Yagu naniou wakh Diamono Macky ci khoutba djouma yi. Omar sall, mor kebe et tant d’autres.

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    ​@@DieynabaThioub-vi1ddnafexx youo mos fen rek laniy def

  • @solution5135
    @solution51359 күн бұрын

    Séne lamingi reuyna baringéne wakh amaloléne dinédji bénne ndiaring tidjiane yi mourit yi taléne yi layéne yi ndiongi tabakh ay hopital di défar ay tali di takhawal ay deuk di diangal ay nitt wayé yéne wakh reuy lamingi lolou dou diné dangéna sokhor ba doungéne toudou sén mbokki djioulit yi

  • @moussafall7123

    @moussafall7123

    9 күн бұрын

    Salam. Sa waaye lii nga wakh lepp fan nga ko tek ? Kou lay diggel lou la mene dougal aljanna, mousal la chi safara, kooku amaloula ndiarigne ?

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    ​@@moussafall7123tok si minbar yi di fen rek wakho ño len ludul bidah bidah te yaw sakh mano ma texxale lan moy sunnah ak lan moy bidha dof yi

  • @Mahtarsow

    @Mahtarsow

    9 күн бұрын

    Wa bidda khasté rek wanté alkhourane ak sunna rek yalna borom samm léén way té yokou xam xam bi masha allah

  • @Mahtarsow

    @Mahtarsow

    9 күн бұрын

    Wa bidda danouy ngawa maguéttt loutakh lolou kholal oustaz rek masha allah ❤❤

  • @solution5135

    @solution5135

    4 күн бұрын

    @@Mahtarsow sawaay dofo damani bane ndiaringi ngéne amal diné dji diné dou wakh rék dieuf dafthi am solo tabakh hopital takhawal ay deuk défar ay tool beune forage défar ay tali ay écol lolo yép si diné la bok wayé yéne yoyou yép yitélouléne té yéne ngingénedi khass djiouma yi geuna rafétt si adounabi lanounouy défar sodougé tout tube tappé djiouma yi geuna rafétt djioumay touba dinasibok ak tivaone té ndiodéf séne bay yi ay djioulitt yalla dafa beugu djioulitt bou am ndiaringi

  • @FOCUSS32
    @FOCUSS329 күн бұрын

    lii yabate deug la nek Sénégal di toppo wa macka bakhna rek kodi geuna dof ngani kii la xam xam 0

  • @mouhamaddiangdiallo6992

    @mouhamaddiangdiallo6992

    9 күн бұрын

    Science tv wouyowo sa tour. Sinon science ngay djital wayé parparlo mola nekh.

  • @yoyo-vw4lj
    @yoyo-vw4lj9 күн бұрын

    Thiey Sénégal donc il y 'a eu 2 tabaski

  • @user-ld9gm1pf3v

    @user-ld9gm1pf3v

    9 күн бұрын

    Arafat dé demb là cône tay môme loumou wara done

  • @papemamadousene4423

    @papemamadousene4423

    9 күн бұрын

    Tey moy tabaski

  • @sonkodiomaye

    @sonkodiomaye

    9 күн бұрын

    Mais est ce que vous faites la part entre yawmou hanrafa moy 9e jour ci weerou Tabaski ci weeru wolof te lolou sentu weer lagn koy natte com koor ci lagni Tabaski 10e jour bi et taxawayou hanrafa lolou gni dem makka la soxal donc bouleen beugué baser wou ci makka boudé moleen doy diaroul wax ta ngeen duangi s'en diné mongueun

  • @user-ku1dz5rm1g
    @user-ku1dz5rm1g9 күн бұрын

    Pourquoi lundi

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    Moy bisub tabaski fii Senegal

  • @falyfal9
    @falyfal99 күн бұрын

    Tabaski nounou donc taye? Khalate léne waye c un seul soleil mais la terre tourne on n'a pas les mm heures exemple Arafat se passe à la Mecque et c le 9éme jour de la tabaski alors dans chaque c 'est ce jour leur arafat mais si on prendre les heures de Mecque c un problème en Australie à cet instant T il est 22h30 ici au Sénégal 12h30 et à la Mecque 15h30 alors en Australie çté quand le jour du Arafat ? Si le jour doit être le mm pour tout l'Oumah Islamique ?

  • @mamechiekhfall315
    @mamechiekhfall3159 күн бұрын

    Li leupp rèk beugua feuss rèk wayé 5person lou 3 yi wakh moy dagui

  • @samseck7043
    @samseck70439 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @oussoubane2712
    @oussoubane27129 күн бұрын

    Ndax dëkk yu bokkul ay waxtu julli mën na ñu bokk bisu Tabaski walla Korite?

  • @serignetine1420

    @serignetine1420

    9 күн бұрын

    Lolou dh mom logikoul

  • @sambmamadoufalilou4830
    @sambmamadoufalilou48309 күн бұрын

    Akhlou souna wal diamakha😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @talladiop-mn2te
    @talladiop-mn2te9 күн бұрын

    Gni mome nioumou

  • @momathniass5720

    @momathniass5720

    9 күн бұрын

    😂😂😂

  • @awatraore8604

    @awatraore8604

    9 күн бұрын

    Gni ahlou sounna Adouna gneupa djouli Babou dess Sénégal

  • @adamandiaye2580

    @adamandiaye2580

    9 күн бұрын

    @@awatraore8604 waxo deug dh

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    ​@@awatraore8604ay fen la deh lii du ahlu sonnah ahlu mafia la

  • @momathniass5720
    @momathniass57209 күн бұрын

    Es ce que yagui ko done wakh diamano Macky firawna Sall mais wakh dji rafetna

  • @idysarr6180

    @idysarr6180

    9 күн бұрын

    Il l'a tjrs dit dano amone un ngoumba teukh loup motakh

  • @adjamariemediedhiou5837

    @adjamariemediedhiou5837

    9 күн бұрын

    Genrou xoutba yi bouko wakhone période maky sall cone heure bi migui kasso rebeuss ndakh moins de ça maky teudje nafi aye nit mais come on dit deug amoul période bou bakh wala bou bone

  • @momathniass5720

    @momathniass5720

    9 күн бұрын

    @@adjamariemediedhiou5837 bilahi lou lér ga wakh 🙏

  • @cheikhtidianediallo3403
    @cheikhtidianediallo34039 күн бұрын

    Ce discour la vous ne l avez jamais tenu durant les deux mandats de Macky Sall 2 poids 2 mesures

  • @user-tu5do2bu1z

    @user-tu5do2bu1z

    9 күн бұрын

    Je pense ke c la première fois que tu écoutes le cheikh

  • @cheikhtidianediallo3403

    @cheikhtidianediallo3403

    9 күн бұрын

    Je le connais mieux que toi c mon promotionnaire de la même université

  • @ridasmanga2691
    @ridasmanga26919 күн бұрын

    Discours bi bakhna torop mais diamano maky dee kéne degoul guéne tenir Discours yi Sénégal Etat Laïque la yorr dou État islamique Il ya des chrétiens dans ce pays Des gens qui ne croient en rien Etc etc

  • @biboujemeh5739

    @biboujemeh5739

    9 күн бұрын

    Lii la yagga wax dangko setanoul rk

  • @biboujemeh5739

    @biboujemeh5739

    9 күн бұрын

    Té Etat bifi nekkone dagno teukh

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    ahlu fen kat

  • @biboujemeh5739

    @biboujemeh5739

    8 күн бұрын

    @@FOCUSS32 Sama yarr mayouma may saga

  • @ousmanefall3693
    @ousmanefall36939 күн бұрын

    Ki kou gnaff ndayame la!!! Khamoul sarape ndayame !!! Ak guéminame bou gnaff ndayame bi!!!

  • @ousmaneba9503

    @ousmaneba9503

    9 күн бұрын

    Yaw ya bonne te yees yallah Nala yallah soppi

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    ​@@ousmaneba9503yalla key boy soppi yaw mii ley soppi yaw khamo si lo nek yalla nala yalla soppi

  • @alfredbonkassy1023
    @alfredbonkassy10239 күн бұрын

    Mdrr tabaski c'est demain frerot

  • @Niane2023
    @Niane20239 күн бұрын

    Imam sa data yaye

  • @user-ic5fg7gx7j

    @user-ic5fg7gx7j

    9 күн бұрын

    yaw sa ndigui leufeul ndeye yaw sa yo yewo domou thiaga bi

  • @abdoulayediarra2525

    @abdoulayediarra2525

    9 күн бұрын

    Akhi ne répond jamais le mal par le mal Allah s'en chargera de lui​@@user-ic5fg7gx7j

  • @abdoulayediarra2525

    @abdoulayediarra2525

    9 күн бұрын

    Asalamou enléykoum akhi respectons nos savants musulmans

  • @user-ic5fg7gx7j

    @user-ic5fg7gx7j

    9 күн бұрын

    @@abdoulayediarra2525 magui toupe deh di ballou ak tu le gua la et iresponsable

  • @khadimgueye9999
    @khadimgueye99999 күн бұрын

    Ndéring yi soff nagne😂

  • @AhmedDiallo-ew9ns

    @AhmedDiallo-ew9ns

    9 күн бұрын

    Sa tounou ndey domou thiotou

  • @septchaine

    @septchaine

    9 күн бұрын

    Les nderig deg naniou olof légui

  • @FOCUSS32

    @FOCUSS32

    9 күн бұрын

    ​@AhmedDiallo-ew9ns lii nga kham mo takh lek nan seuy

  • @serignetine1420

    @serignetine1420

    9 күн бұрын

    Nderingue degno wara guen Senegal gno yak Senegal

  • @NAGSUNUGAAL-tg3xx
    @NAGSUNUGAAL-tg3xx9 күн бұрын

    Yaw nopil do Sénégalais baparé bëgg gno sonal degena bëgg taal rewmi

  • @alimouba79

    @alimouba79

    9 күн бұрын

    Ngaladio Ka de son vrai nom . Est-ce que tu est plus sénégalais que lui ?

  • @IbrahimaCisse-jn6nv

    @IbrahimaCisse-jn6nv

    9 күн бұрын

    Ragalal YAALLAH

  • @ousmaneba9503

    @ousmaneba9503

    9 күн бұрын

    Yaw sa baye mo nekkoul Sénégal

  • @Ndaye.Khadi.bousso

    @Ndaye.Khadi.bousso

    9 күн бұрын

    Merci kou bakh doollll rek lanuy déf😂

  • @Ordinaire95

    @Ordinaire95

    9 күн бұрын

    Domouharam you melni yen di traîné ci youtube Di choisir kou done sénégalais ak kouka nekkoul. Bayilene sen yeuffou doff yi , le Sénégal est un pays multi culturelles ethniques etc...

  • @Beugdeug
    @Beugdeug9 күн бұрын

    Respectez vous et respectez les autres musulmans car vous attaquez trop les soufistes car aucun que vous vous pour dire qu'on doit prier aujourd'hui

  • @alioukande7676
    @alioukande76769 күн бұрын

    Maudits soient des Imams diviseurs.Tout le monde entier prie le Lundi sauf certains soient disant musulmans models

  • @biboujemeh5739

    @biboujemeh5739

    9 күн бұрын

    Qui et qui prient le lundi ? Seuls les sénégalais prient le lundi

  • @Sokhnadiarrapastef

    @Sokhnadiarrapastef

    9 күн бұрын

    Tabaski 3 jour laa

  • @Layla-zp4cn

    @Layla-zp4cn

    9 күн бұрын

    N'importe quoi, la fête c'est après le jour de Arafat, arrêtez de suivre vos Serigne au lieu du sunna de Mohamed psl.

  • @HabibGadiaga
    @HabibGadiaga9 күн бұрын

    بارك الله فيكم

Келесі