🚨Pape Sarr répond Franc, Eumeu Sene dousa...Sokh dafa erreur limou wakh si Eumeu 200% pikine denioul

Спорт

#lutte #etdrmedias #lamb
👍 Merci de laisser un pouce bleu 👌
Visiter également notre site web: www.etdrmedias.com
NOS réseaux sociaux :
/ etdrmedias
/ etdrmedias

Пікірлер: 170

  • @abdourahmanediop2948
    @abdourahmanediop294829 күн бұрын

    seuytané nga ya tasse pikine chaque jours nga watte ni bayii nga nittou lamb yii vrai nafékh nga sa bopp rék mola niorre

  • @sambagora7848

    @sambagora7848

    29 күн бұрын

    😂😂😂😂😂

  • @kategniemendy5965
    @kategniemendy596529 күн бұрын

    Franc-Eumeu, c’est le combat que tous les sénégalais attendent

  • @coeur2lion38

    @coeur2lion38

    29 күн бұрын

    😂😂😂😂

  • @babacarfaty5397

    @babacarfaty5397

    28 күн бұрын

    nel ioe ya koy xare

  • @amadoudiopndoye3582
    @amadoudiopndoye358229 күн бұрын

    Franc est un vrai sportif je te jure ! En plus il communique bien c comme ça qu’on communique dans un sport de combat

  • @Al_Amine1975

    @Al_Amine1975

    29 күн бұрын

    Au contraire il communique mal Il n'a pas de contrat avec eumeu sene ni avec balla gaye donc il n'avait pas a parlé ainsi

  • @amdymoustaphadiop1343

    @amdymoustaphadiop1343

    29 күн бұрын

    ​@@Al_Amine1975saway li teukonté la sport bo dem fekk ko fa

  • @Al_Amine1975

    @Al_Amine1975

    29 күн бұрын

    @@amdymoustaphadiop1343 je suis d'accord mais dans le respect. Franc communique mal mom ak Reug Reug nio bokou problème

  • @foreveryoung29

    @foreveryoung29

    29 күн бұрын

    @@Al_Amine1975lgui qu’est ce que Franc a dit de mal

  • @josephmendy7792

    @josephmendy7792

    29 күн бұрын

    ​@@Al_Amine1975 Balla Gaye bimouy toleu thi diamono bi est ce que dane nguéne wax ni dafa rew... Lamb mo démé nii

  • @Capsiladeuk
    @Capsiladeuk29 күн бұрын

    Ki mom weroul momine leu. Eumeu dafka écarter warone nga am diom 😂

  • @user-vz7to3qq1z
    @user-vz7to3qq1z29 күн бұрын

    Franc dé mo meune say mbeur yep

  • @azizsarr9533
    @azizsarr953329 күн бұрын

    Yaw mak mou niank fayda nga franc sa moromou dom leu

  • @ndiayebathie-rf7fh
    @ndiayebathie-rf7fh29 күн бұрын

    Pape Sarr vré doméram le Modou lo wakhone n'a dof la mé c vré

  • @sadgametv2538

    @sadgametv2538

    29 күн бұрын

    Boudon sa bay doko wax dh domeram

  • @elhadjiamadoundao6286
    @elhadjiamadoundao628628 күн бұрын

    FRANC/EUMEU MOYE COMBAT BI❤❤❤

  • @falldamel7484
    @falldamel748429 күн бұрын

    Pathé Baldé aussi gala na diap si lokho Sokh yobouko keur Eumeu Séne

  • @bourathobouratho4672
    @bourathobouratho467229 күн бұрын

    Merci pape sarr

  • @cheikhfall5548
    @cheikhfall554826 күн бұрын

    Merci grand pape sarr nous sommes derrière toi

  • @madembatoure7005
    @madembatoure700529 күн бұрын

    Yow dagua rouss xana tay ngaye nangou landiang nek porteur de voix eumeu sene ak ligua xass landiang lep meunoulo si Franc dara par force day beurei ak eumeu sene bayil sissou

  • @Omarsane7491

    @Omarsane7491

    29 күн бұрын

    Kii domerame laa 😂😂yamba la dieul motah domerame laa

  • @user-lw1oi1yi6s
    @user-lw1oi1yi6s29 күн бұрын

    Pikine seul ❤❤❤❤❤

  • @elhadjiamadoundao6286
    @elhadjiamadoundao628628 күн бұрын

    GRAND KAGNE NGAYE MAGUEU😂😂😂

  • @user-oh6ou9fs2p
    @user-oh6ou9fs2p29 күн бұрын

    Tu as reson

  • @VieuxNdiaye-rt2cc
    @VieuxNdiaye-rt2cc29 күн бұрын

    Ioe l'an nga pikine pape lii d'où vit avec respect wagniil wax djii

  • @yayacisse9746
    @yayacisse974629 күн бұрын

    Pape sarr Yalna yalla defal diamou ❤diambar nga ❤Machallah

  • @khabanegueye-fl8wq
    @khabanegueye-fl8wq29 күн бұрын

    Pape katal sa ndaye bari ngua wakh kom jiguén meuno thiotou ndayam si franc

  • @user-oh6ou9fs2p
    @user-oh6ou9fs2p29 күн бұрын

    Toon numéro sr te plaît Pape Sarr

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj29 күн бұрын

    Man wadji ak guéminiam gou khingne gui kagne lay noppi yo sarr ioe domou bireul ngeu😂😂😂😂

  • @YayaNdiaye-lr2ts
    @YayaNdiaye-lr2ts29 күн бұрын

    Balla rek inchalah

  • @cheikhthioub2240
    @cheikhthioub224029 күн бұрын

    Khana setano Tapha tin B-52 ngani eumeu Moko yobou ardo bayil nén

  • @aboukane1521
    @aboukane152129 күн бұрын

    Pape Sarr sa data yaye

  • @Al_Amine1975

    @Al_Amine1975

    29 күн бұрын

    Kou respecté woul yayam rek moy Saga yayou diambour

  • @saliougueye2348
    @saliougueye234829 күн бұрын

    Yaw ya tasse pikine pape Sarr wakh rekh AK ay Doul

  • @nitoudegeukaddudegeu3001
    @nitoudegeukaddudegeu300129 күн бұрын

    LO DÉFAL NIIT WAX KO 😮 MANEDÉ YALLA BOMA MEUSA DÉFAL,, WA NIIT KO XAMENI BOU DIOUBÉ AK YAW DILA TAGGEU TÉ BOULA MÉRÉ YÉKEULA KATÉMÉ BILAHI WALAHI KI WÉROUL TÉ DAFA FAUX 😢 TEKSI DONE MAKK BOU NIAKEU FAYEDA AMOUL ESPRIT DE DÉPASSEMENT TCHIM 😡 YAW ROUSSAL SISA DOME CHEIKH 🫵🏿 SA NAWELÉ LA TOUJOURS NGA TÉKO GUATHIÉ MOUY GUISS NOUY SAGA BAYAM OH 😢😢😢

  • @mordiop5555
    @mordiop555529 күн бұрын

    Sathies da ragal Frank 😂😂😂

  • @moussapayemane4167

    @moussapayemane4167

    29 күн бұрын

    Sa Thiéss mo meune Franc,Reug Reug moko meune

  • @assleye8654
    @assleye865429 күн бұрын

    Merci pape sarr ❤❤

  • @TaherElouardi
    @TaherElouardi29 күн бұрын

    Merci pape

  • @Diopbayemodou
    @Diopbayemodou29 күн бұрын

    Ana wa pa

  • @MoustaphaFadiga-jy3dr
    @MoustaphaFadiga-jy3dr29 күн бұрын

    Pape Sarr dangua sokhor sa niaway bi toukh yamba rek ngua meune

  • @saliougueye2348
    @saliougueye234829 күн бұрын

    Pape Sarr dég sokhor torp Franc vs Eumeu séne Moy combat bi

  • @bocarba2781
    @bocarba278129 күн бұрын

    Pape sarr ada ndiaki diom, vraiment pape athiou niamdé gada yimbé. Ahh marr tate bi doyna. Legui nga am 60ans top di mar tate rek

  • @Omarsane7491
    @Omarsane749129 күн бұрын

    Kiilou Modou lo wah rek dof deugeula ba paré n'a bayou yamba😂😂😂😂😂

  • @barasall7880
    @barasall788026 күн бұрын

    Ki kane la pape doff 😂😂mé pape sarr khana amo diabar dé lolou war naniou ko li dieune ti dé athia pape doff kharitou modou lo 😂😂😂

  • @MamadousaliouthiandoumTh-bt6co
    @MamadousaliouthiandoumTh-bt6co29 күн бұрын

    Pape moni won bayina nitou lamb dh

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf11029 күн бұрын

    En combat boy niang 75mil nga si def mai bou ama ay millions nga si def yw doul rk 😅

  • @amdymoustaphadiop1343
    @amdymoustaphadiop134329 күн бұрын

    Mai gars yi ltx niou bagn franc

  • @user-tr5zk4xk1u
    @user-tr5zk4xk1u29 күн бұрын

    Bari ngua wakh

  • @masseyefaye6005
    @masseyefaye600529 күн бұрын

    ki féne rék lay def dafa bagne Franc mais kholam dou nékh khamoul dra ci lamb loum wakh dou degg ki coupé la wara analysé mais pas lamb ki dafa soff day wakh di youtt rék

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking38229 күн бұрын

    Merci pape sarr le monument de pikine franc dafa réw té défoufi gatt moromame yeupeuko raw franc dou gate 😂

  • @frankydolle7559
    @frankydolle755927 күн бұрын

    Ya meuna doul tu as oublié le cimbat tapha tine vs Bombardier ardo dans les 2 cotes

  • @ibrahimasall8070
    @ibrahimasall807029 күн бұрын

    Bilahi sénégalais dafa sokhor franc bouko pikine amone do wakhé ni pape Sarr nakh franc 13 combats 13 victoires la am Kone sa Thiès loudoul papam mbeur lawone eupeuléwouko franc

  • @morramos9050

    @morramos9050

    29 күн бұрын

    Man dh douma supporter sa thies mai nioumou beurél franc beurewoul AK niom

  • @badaradiouf4646

    @badaradiouf4646

    29 күн бұрын

    Ki mome aye waax wame diaroul considéré Franc goudi yi mo rawe Sa Thies

  • @foreveryoung29

    @foreveryoung29

    29 күн бұрын

    @@morramos9050 est ce que niou franc beurel Sa Thies beurei nakk niom ?

  • @masseyefaye6005

    @masseyefaye6005

    29 күн бұрын

    @@morramos9050 wakhi dof sa thies combat de déclanchement yép la niak alors loum eupeulé franc

  • @bourathobouratho4672

    @bourathobouratho4672

    29 күн бұрын

    Franc sou beugé beuré ak eumeu séne nako diokh respect

  • @babadiallo8800
    @babadiallo880029 күн бұрын

    Ya tasss pikine seytaneiii nga

  • @taphadiene
    @taphadiene29 күн бұрын

    Ahh Pape Sarr môme wéroul

  • @user-cm8yz4gx5t
    @user-cm8yz4gx5t29 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤🎉Balla 2

  • @khadimdiop2107
    @khadimdiop210729 күн бұрын

    Bamou dess iOw ak Wa PA😂

  • @BallaMbathie-on4gj
    @BallaMbathie-on4gj29 күн бұрын

    Ki day doul kess Fran seul

  • @Omarsane7491
    @Omarsane749129 күн бұрын

    Mom tass pikine ba paré di doul 😂😂😂

  • @cheikhgueye5458
    @cheikhgueye545828 күн бұрын

    Pape sarr wakhi sokhor rek guafi wax

  • @lapaixlapaix8873
    @lapaixlapaix887329 күн бұрын

    Ki vrai doff la 😂😂😂😂

  • @user-ou4cb5kl6c
    @user-ou4cb5kl6c29 күн бұрын

    Pape bayil sisou mbeur bo faral franc daneko thji ay second

  • @kara1893
    @kara189329 күн бұрын

    Pape nak yagu sisou deee fran sen papeleu bikini Modou lo ak fran nioko mom

  • @amadoudiopndoye3582
    @amadoudiopndoye358229 күн бұрын

    Non pape sarr tu es méchant

  • @cheikhtidianefaye824
    @cheikhtidianefaye82429 күн бұрын

    A chaque fois mou guen ne pikine nek nagnou Ben

  • @AdolpheGomis
    @AdolpheGomis29 күн бұрын

    Qui vrai comédien la Sénégal ay doff lagni diokh cadou diap ni ay nitt nioy wakh Ndéké fou la😂😂😂

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye391329 күн бұрын

    Pape sarr nite day wakh lou yénou mana franc méritona beuré ak eumeu séne

  • @ibrahimatall5277
    @ibrahimatall527729 күн бұрын

    Pape dalay khass tay, souba mou tagg lah,naan gno bokk nday ak baay 😂😂😂

  • @matargueye1724
    @matargueye172429 күн бұрын

    Pape sarr dafa Bari wakh

  • @babadiallo8800
    @babadiallo880029 күн бұрын

    Franc mo meunn pikine xaleiii dolé

  • @Jiehsjkdghdkjdhkdjbdiodjbdblk
    @Jiehsjkdghdkjdhkdjbdiodjbdblk29 күн бұрын

    Vrema Franc wakhoul Dara lou graw

  • @user-oh6ou9fs2p
    @user-oh6ou9fs2p29 күн бұрын

    Père sa Thiès d'où moromou franc

  • @georgesdieganediouf2684

    @georgesdieganediouf2684

    29 күн бұрын

    C'est pas vrai. Franc moko meune mille fois.

  • @fallouniang3438
    @fallouniang343829 күн бұрын

    Ki dafa doff 😂😂

  • @mansourkane1426
    @mansourkane142629 күн бұрын

    Pape sarr sa data yaye 😂

  • @MamadousaliouthiandoumTh-bt6co
    @MamadousaliouthiandoumTh-bt6co29 күн бұрын

    Pape sarr pikine doff lanla diapé parce que do wah wahou nitt ninga dfon ba mod lo rouslo laa fi ngay topatt ci franc ak linga fii wah landiang yeup tey ngay sogua ham

  • @user-qd2qn3di4n
    @user-qd2qn3di4n29 күн бұрын

    Franc eumeu séne dou combat eumeu séne si dieulé franc ma khané ki dou nitte franc Ama combat leu boye niang franc combat leu fanc doudou sané combat leu ordi ak franc combat leu pourquoi eumeu séne bayil léne Di teubeul mbeure yi franc n'a ranpé doul way niome nieupeu niou nék si lamb dji la wakh barki alkhourane kou thie nék yagui rêvé mbeureck eumeu séne pour danko pour sa palmarès raféte no nekhoul ba nékh mé eumeu séne meilleur lutteur du Sénégal mofi dakeu mbeuré thie lamb dji deugue nekhoul respect à lui

  • @bachirdomouparcelle4293
    @bachirdomouparcelle429329 күн бұрын

    Avant ma setane pape sarr del brossou xawnganiou ray ndax audeur

  • @josephcoly4127
    @josephcoly412729 күн бұрын

    Bombadier tapha tine comme tapha tine khana vitalalait la dem mes demoul ardo c grave koi déysanne

  • @coeur2lion38
    @coeur2lion3829 күн бұрын

    Fran limou beg dafa yobe bane ndandane la ndam ?

  • @user-nq6md6sx6g
    @user-nq6md6sx6g29 күн бұрын

    Combat la dé euma vs fran moy combat

  • @legendediop9215
    @legendediop921529 күн бұрын

    Yenkay nelen danguen ragal franc dane sen mbeur rek😂😂😂

  • @Papesarr-wv3me
    @Papesarr-wv3me29 күн бұрын

    yaw mi rk ya diarta micro 🎤 parce que dof nga dof bou sokhor

  • @zeybambalvl6972
    @zeybambalvl697229 күн бұрын

    Franc pikine jakob ak pokola gnoufaye sa morom amo khoromou lamb téksi chéro teudieul sa gaate gui beuringa wakh trop

  • @mohamethdieng1783

    @mohamethdieng1783

    29 күн бұрын

    Ioe tmt del wakh deug 😂 franc 3 VIP yi la wala beurel sokh moy top 4 pikine Kon 3 bi na nieuw

  • @thiamahmadulattekh562

    @thiamahmadulattekh562

    29 күн бұрын

    Nit dey wax deug deug pikine kene amusant 13 combats 13 victoires

  • @modo6218

    @modo6218

    29 күн бұрын

    Pikin souniou noss la franc mo meun sen papa 😂😂

  • @elhadjindiaye7089
    @elhadjindiaye708929 күн бұрын

    Wa pikine mounou niou begue mberou parchel 😂😂😂

  • @ismailadiakhate6655
    @ismailadiakhate665529 күн бұрын

    Tapha Tine demna ardo contre Bombardier bou ndieunk bi

  • @charlesmanga1632
    @charlesmanga163229 күн бұрын

    Danio ragal franc niom nieup léy dane

  • @aliousarr3816
    @aliousarr381629 күн бұрын

    Qui dafa dof

  • @user-eh3qp1rj5m
    @user-eh3qp1rj5m29 күн бұрын

    Wakhou farr kessé ngay wakh franc teggui woul deh reug mooo bagne

  • @lionnoir2799
    @lionnoir279929 күн бұрын

    Pape niarre yimouy wah j comprend pas

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye391329 күн бұрын

    Pape sarr tapha tine bouko wagnilo pois taha bou oyofé dou bakh thi mome

  • @ibrahimatall5277
    @ibrahimatall527729 күн бұрын

    Pape sarr khana andoul ak khélam ? Tapha Tine vs Bombardier, Tapha démona ardo plusieurs fois. Après ngani Franc day tégui Reug-Reug, yow fo nekk? Franc ak nimou sonalé Reug-Reug ci plateau yi, non Pape tay wakho fi lamb.

  • @mordiop5555
    @mordiop555529 күн бұрын

    Wakhi doff mais franc inchallah roi des araines

  • @abdoulayediop9331
    @abdoulayediop933129 күн бұрын

    Pape wakhou deugu khana comba Modou AK eumeu Modou AK Ama Modou AK boy Niang faran AK soukhou khana bockou thi biss you Mack yi fi dall yafi wakhoune né bayi nga babouye adina AK alakhéra wakh katt nga

  • @assanekaka9414
    @assanekaka941429 күн бұрын

    Thiey pikine ba legui yéne gui wax nn

  • @DiawBadou-fz9dz
    @DiawBadou-fz9dz29 күн бұрын

    Franc na dém si sa thiéss doule wayy

  • @laminediabate556
    @laminediabate55629 күн бұрын

    Wa Abdou bahoum la dégatoul fénn...dafa melni Modoulô moko fayy

  • @aboukane1521
    @aboukane152129 күн бұрын

    Franc seul

  • @Zahim.LinetObii
    @Zahim.LinetObii29 күн бұрын

    Pape sarr sissou mane bou niapp sa ndeye ngua

  • @Iiiiiiiiii873
    @Iiiiiiiiii87329 күн бұрын

    Eumeu fin de carrière la nekk tolotoul fimiye wakhé mbeur doumassa morom

  • @VieuxNdiaye-rt2cc
    @VieuxNdiaye-rt2cc29 күн бұрын

    Pape Ioe kOu miin sa wãx yapla wagniil wax dji tmt ahh nehoo xexaal deh

  • @Malcom282
    @Malcom28229 күн бұрын

    Mane ki mome Bilahi khamouma louko dall quoi

  • @youssoumbengue7698
    @youssoumbengue769829 күн бұрын

    Legui franc dal day tok khar reug beurei niari combat dal mdrr yaw dangua nekh

  • @BallaMbathie-on4gj
    @BallaMbathie-on4gj29 күн бұрын

    Doul rek

  • @user-ou4cb5kl6c
    @user-ou4cb5kl6c29 күн бұрын

    Franc thiate rék lakoy ragalal

  • @amadoudiopndoye3582
    @amadoudiopndoye358229 күн бұрын

    Franc moy lamb !!

  • @elhadjindiaye7089
    @elhadjindiaye708929 күн бұрын

    Ki koumou tague tay soube mou khass la saytané nga niape comprendre nanioula

  • @moussapayemane4167

    @moussapayemane4167

    29 күн бұрын

    Lolou motah ki néhouma dara,Tey mou hasss là,souba mou tague la,holal limoufi done wah Sa Thiéss diko wah louné mais tey mom day tague Sa Thiéss boubah,défnako aussi Lac 2 diko wah louné,tey day tague kokou aussi

  • @abdouniang3082
    @abdouniang308229 күн бұрын

    Ki daffa doffff

  • @abdoulayendoye1803
    @abdoulayendoye180329 күн бұрын

    cheuteuteute 🤣

  • @mouhamadoudiop4287
    @mouhamadoudiop428729 күн бұрын

    Say aka sokhor mo tah dou ame yaram nanal ndokh

  • @joe6326
    @joe632629 күн бұрын

    Pape tay ande mou ak yaw Fran mériter neu beuré ak yi nek si kaw ndakh Ada fass mi sou dané gouyguii yu diokhko eumeu sen😂donc Fran warna meuneu beurrée ak eumeu sen mais lutte avec frappe meussoul Beug mberou mbapate yeuw si kaw lolouu dalona yekénii li mom sokhor la fran bou nekone sa petit frère doko yéné lenene

  • @abdoulayesane9222
    @abdoulayesane922229 күн бұрын

    Wa pikine. Pap sar mossi geuna sokhor yen ba ama baldè beuguè modou lou nek gen done wah legui franc beug eumeu gay sissou😂😂😂folen deg P.A city daw

  • @modo6218

    @modo6218

    29 күн бұрын

    Bayi len fofou rek 😂😂

Келесі