NOUROU DARAYNI RAJAZZ S. MOUSTAPHA NGINGUE

Фильм және анимация

Serigne Moustapha Ngingue

Пікірлер: 561

  • @abdoulbaidygueye3621
    @abdoulbaidygueye36216 жыл бұрын

    Serigne moustapha yalla ga guoudou fane ak weer..barké KHADIM RASSOUL.

  • @chabseye1000
    @chabseye10006 жыл бұрын

    Eskeuy...jërëjëfëtii seriñ touba. Seriñ moustapha gningue gueuneu yagu gueuneu werr cii barkep nourou darayni

  • @cheikhfall4558
    @cheikhfall45588 жыл бұрын

    dieureudieuf serigne touba diarama mame cheikh ibrahima fall man damay sakou sen niane yalla defalgnou diam djou beuri ak mbolem dioulit di sakou wat niane si xassida bi di nourou darayni yalla yokou lerou serigne touba ak wa keureum dieureudieuf serigne touba

  • @fatouthiam4906

    @fatouthiam4906

    3 жыл бұрын

    Dieuredieuf Serigne Touba AMOUL MOROM yalana naniou naguoul nian gui d'i NOUROUROU DARAYNI YALANA NANIOU KO YALA FAYAL THI BARKE SEYDINA MOUHAMED SWS

  • @senmodart1676
    @senmodart16768 жыл бұрын

    yallah na yallah fath adio si barek seydina Muhammad

  • @khelcombachesvisions9104
    @khelcombachesvisions91045 жыл бұрын

    Moy téré bilay dieulé ci leundeum yoboula ci léér goudoul fayyy ba mouk Inchallah

  • @Seyibrahimit
    @Seyibrahimit8 жыл бұрын

    Amna solo yalnagnou yalla guena khir thi serigne bi

  • @mamznjie6281
    @mamznjie62813 жыл бұрын

    Serign Touba is my food, water and heart..... I belief I would not have come into this world if i am not mouride, only serign touba can save my soul...... Sunu yakarr fee ak fung njem.....

  • @99alfailiwaqain51

    @99alfailiwaqain51

    2 жыл бұрын

    As Salaam Alaikum; Those are some prudent words. May Almighty ALLAH continue to bless you!!!

  • @khadimsaw1437

    @khadimsaw1437

    2 жыл бұрын

    8

  • @awademe4665

    @awademe4665

    2 жыл бұрын

    6

  • @mameyandengom4923

    @mameyandengom4923

    2 жыл бұрын

    Iiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii. 8i

  • @soxnamouslyfall795

    @soxnamouslyfall795

    5 ай бұрын

    1a​@@99alfailiwaqain51

  • @fabiocarrara4210
    @fabiocarrara42108 жыл бұрын

    kene dou khadimou rassoul yalla nanou sounou borom chakhal ci mouridhou lahi dieureu dieuf baye khalil mbacke imnou mourtalla alkhourane reek moye beug beugeume mbacke khayartou dolignou khewal mbacke banou gadou darayi ak diakayi mbacke amine

  • @senegalhairrocksenegalhair6373
    @senegalhairrocksenegalhair63737 жыл бұрын

    Allahu Akubar serigne touba ma la beugeu diarama

  • @alssanembengue9837

    @alssanembengue9837

    3 жыл бұрын

    Mane ki Dafma yeem

  • @ramatulayendoye4387
    @ramatulayendoye43874 жыл бұрын

    Thieuy s.touba amoul.morom yala na nou ko yala fayal alahuma amiiin dieurdieufti s.touba.

  • @cherifndiaye1729
    @cherifndiaye17293 жыл бұрын

    Serigne mountakha mbacke yallnafi yague te wer amine 🤲🤲

  • @nafithiam2010
    @nafithiam20104 жыл бұрын

    Dieureudieufeuti Mame borome Touba Moustapha ngingue yalla Nassa diameu yagueu yalla wereule bate bi

  • @maguattediop2983
    @maguattediop29836 жыл бұрын

    Serigne touba rek Ka worr

  • @khaliltv5781
    @khaliltv57814 жыл бұрын

    Yalna gnou yalla mousseul si saytané ak lépou Lou bone té déf gou ay degue degue Mouride Goudeul sunouy fan yokou Xéweul yi si barkép Xassida gui si NOUROU DARAYNI 🙏🙏🙏❤️

  • @khadyndiayeyayefall9014

    @khadyndiayeyayefall9014

    3 жыл бұрын

    Amine ya bari

  • @falloufall7847

    @falloufall7847

    3 жыл бұрын

    Amine fall

  • @falloufall7847

    @falloufall7847

    3 жыл бұрын

    Amine

  • @ndiagadiagne3894

    @ndiagadiagne3894

    Ай бұрын

    Machahala ❤❤❤

  • @babasow891
    @babasow8914 жыл бұрын

    Alhamdoulilah alhamdoulilah je pleure comme un bb en l'ecoutant sans savoir pkoi jarrive plus a dormir

  • @ahmadoubambambacke5216
    @ahmadoubambambacke52164 жыл бұрын

    Thiey kou tedki thiey serigne touba sante yalla rék binga néké sama xol alhamdoulilah dieuredieufati Serigne Touba

  • @sidibirahimgueye1056
    @sidibirahimgueye10565 жыл бұрын

    Yalnane sakh si KHASSIDA YI té gneum li si barkép mame cheikh Ibrahima fall lamp

  • @elhadjini
    @elhadjini7 жыл бұрын

    MASSAHALLA DIEUREDIEUFAT SERIGNE TOUBA YALLA NANOUKO BOUR YALLA FAYALL ALLAHOUMA AMINEEEE

  • @cheikhounabambathiam9622
    @cheikhounabambathiam96227 жыл бұрын

    machahalla machahalla nekh neuh beuri neuh mame borom touba amoul morom euskey serigne touba dieureudieuf mame borom touba

  • @tijantouray2822

    @tijantouray2822

    4 жыл бұрын

    Cheikhouna bamba Thiam nexna beurina birou seriigne touba nekh bari rak macha allah

  • @awafaye5388

    @awafaye5388

    4 жыл бұрын

    Nekh naaazzz

  • @ndellandiaye7260

    @ndellandiaye7260

    3 жыл бұрын

    @@tijantouray2822 mmmmm

  • @falldame3662
    @falldame36624 жыл бұрын

    Dieurdieuf yalla bimou gnou bolé ak serigne touba xadim rasoul

  • @ghdvfhjk8727
    @ghdvfhjk87278 жыл бұрын

    sata rék serigne Touba

  • @abdougueye489
    @abdougueye4896 жыл бұрын

    Moustapha bilahi yala nala yala bolek kou tedki sahadatou darayni ya bakh gningue dieure dieuf sirigne touba

  • @ndeyeastougueye2082
    @ndeyeastougueye20827 жыл бұрын

    yalnagua KO gueuneu meun way mourite

  • @mamadougorguidione1740
    @mamadougorguidione17405 жыл бұрын

    Mamadou Gorgui dione sant serigne touba rek yakar wolou rek

  • @adamanguer6081
    @adamanguer60815 жыл бұрын

    Thiey yalla sa borom Ken dou serign touba

  • @papaalassanegueye9583
    @papaalassanegueye95837 жыл бұрын

    dieureudieuf s touba magilein digeul sama Boop dileinko digeul way way nanoko geum topko ci ndigeulam bayyi Aÿ tereim mooy sounou ndaring tey ak soba yalnano yallq may ak dégage akook toppe

  • @nabyladomoufass
    @nabyladomoufass4 ай бұрын

    Serigne touba nou mouy tagué MOHAMED PSL❤ amoul kénéne kou koy tagué nonou serigne touba bo dégué ay mbindam daguay nane ki koumou done🤔. SERIGNE TOUBA NéNA SE SONT MES ECRIT QUI ONT MES MIRACLE🤩 karamati khattou yadi❤ conne naniou guena gueustou si KHASSIDA YI REK😍THIEUY SERIGNE BI YALLA NA NIOU BOKOU SI AY NDIABOTAME BOU EULEGUé😭😭❤❤🤲🤲🤲

  • @mamadoumaramekebe7446
    @mamadoumaramekebe74465 жыл бұрын

    DIEUREUDIEUF KHADIME RASSOLILLA SAW YALLA DOLI AY LÉRAME SI BARKÉ RASSOLILLA SAW YALLA DOLI AY LÉRAME. AMINE. DIEUREUDIEUF MOURIDOULLA.

  • @mamadoulaminefall2329
    @mamadoulaminefall23294 жыл бұрын

    Serign sangeu fall bayou gor fall yalla nafi yageu looooolou tewer amine

  • @kadiatoudiabira2730
    @kadiatoudiabira27309 жыл бұрын

    thiey serigne touba bo amoule wone fougnou djeume

  • @modoundong7656

    @modoundong7656

    5 жыл бұрын

    seringue touba rek

  • @mamesayembaye8121

    @mamesayembaye8121

    5 жыл бұрын

    Amoul morom

  • @diagnewade7170
    @diagnewade71707 жыл бұрын

    Dierediefety serigne touba Mame khadimou rasoul akaza amna solo yalla nalène serignbi faye amineeeeeeeeeeeeee

  • @micaelasanchez4515

    @micaelasanchez4515

    4 жыл бұрын

    Ra

  • @taphaseye243
    @taphaseye2433 жыл бұрын

    Machallah Dieredieufff brom Touba cheikh Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd qui Aminnne

  • @maremekebe8130
    @maremekebe81308 жыл бұрын

    dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba serigne moustapha gningue yalla nasa bate wer way barke boroom darou

  • @zallethiam6876
    @zallethiam68766 жыл бұрын

    Jajeuf Serigne touba dieureudieufee Serigne touba dieureudieufee Serigne

  • @nassersow9586
    @nassersow95863 жыл бұрын

    Ken dou brom Touba ❤️❤️❤️❤️🙏

  • @papeassaneseye6486
    @papeassaneseye64865 жыл бұрын

    Serigne Moustapha ngigue maguilay nianale si barkè khassida yiguay diangue yalla na yalla dèfal la ligua beugue si barkè seydina mouhamed ak serigne touba mane bène ndoguala rek bou nèk italie di sakou niane si yaw bou bakh beugue nala lole Serigne Moustapha

  • @ousseynouseck5393

    @ousseynouseck5393

    3 жыл бұрын

    Diokh sa numéro Mane ndogal Serigne saliou

  • @kebamama3862
    @kebamama38628 жыл бұрын

    dieureudieufeti dieureudieufeti dieureudieufeti dieureudieufeti serigne touba khadimul rasulilahi diarama diarama diarama mame cheikh ibrahima fall lampe baboul mouridina

  • @ismailacamara2531
    @ismailacamara25318 жыл бұрын

    Amine. yallana yalla fadje adioyi. Dieureudieuf cheikhoul khadim

  • @papicheikh1735
    @papicheikh17358 жыл бұрын

    serigne touba rek mo diara wolou sant na niou la deh mbacke balla

  • @modoufall6351
    @modoufall63517 жыл бұрын

    machalla s mousstapha nékhna loool dieureudieuf s touba diarema mame cheikh Ibrahima fall

  • @khadimndiaye4099

    @khadimndiaye4099

    4 жыл бұрын

    thieut borom touba amoul morm!!!!!!!!!!! 👌

  • @khadygningue9619
    @khadygningue96193 жыл бұрын

    Machallah j sais le bon dieu est fière de ntr cheikh ahmadou bamba khadim Rassoul l ami du prophète Mahomet psl que dieu ns mettent dans le droit chemin c sa qui compte j mapel seydina Alioune fall cartaud 😍 j'aime Serigne Touba djeureudjeufei Serigne Touba mbacke.

  • @guedjipouye1382
    @guedjipouye13822 жыл бұрын

    Alhamdoulillah bignou yalla bolék Serigne Touba

  • @mysylla6862
    @mysylla68624 жыл бұрын

    Mancha Allah dieuredieuf serigne touba khadimou rassoul

  • @tijantouray2822
    @tijantouray28224 жыл бұрын

    Macha Allah Sama xol Neexna seedna gouye dieureudieuf mbacke balla

  • @fallgora3808
    @fallgora38083 жыл бұрын

    Dieuredieufe serigne touba amoul morom machaalla moustapha gningue kouko deguelou yalla na done sakk tékhé adouna alahira ci barke borom touba ak khassida yi amine yarabi

  • @fatouthiam4906
    @fatouthiam49063 жыл бұрын

    SERIGNE Mountakha Yalana fy yague fi loool ta werr Thi Barker Serigne Touba Ak khassidahi Barké nourourou Dareyni Ak Dialibatou Marakhib Amin yarabal

  • @ndeyekarimmboup9573
    @ndeyekarimmboup95737 жыл бұрын

    Dieureudieuf Serigne Touba yalla na yalla nangou sougnouy nian oubilgnou bountou khewal yep si barkep nourou darAyni aminn❤

  • @fallibrahima745

    @fallibrahima745

    5 жыл бұрын

  • @fallibrahima745

    @fallibrahima745

    5 жыл бұрын

  • @immortelcamara768

    @immortelcamara768

    4 жыл бұрын

    Amine

  • @ritabalde9340
    @ritabalde93402 жыл бұрын

    Yallah na yallah werale Bate bi si barké Serigne saliou

  • @babasamb3873
    @babasamb38737 жыл бұрын

    thiey mbacke balla aicha yaye ken yalna na yala ak s.bamba weral bate bii

  • @ndackgueye3656
    @ndackgueye36562 жыл бұрын

    Alhamdoulillah ManshAllah Jeurejeufety SERIGNE TOUBA XADIM RASSOUL AMOUL MOROM❤️❤️❤️❤️❤️

  • @bakarymane6598
    @bakarymane65988 жыл бұрын

    disantate Chekhoul Khadim ,Serigne Fallou ak serigne saliou wayé kénn dou Cheikh Abdoul karim Mbacke fallillou borom MAKARIMAL AKHLA (Bala Aîssa yalna ngafiyague ak wérr té di fadj souniou adioyii si barké NABI MOUSTAPHA ak KHADIMOU RASSOULLL

  • @babacarseck6923
    @babacarseck69238 жыл бұрын

    dieureudieuf serigne touba gnou sante yallà bame gnou bollé si yonnou serigne touba alhamdoulilah

  • @fatouthiam4906

    @fatouthiam4906

    3 жыл бұрын

    Alkhamdouli LAH

  • @ouzsolosolo9453
    @ouzsolosolo94535 жыл бұрын

    Eskey akaza dieureudieuf borom touba khadim rassoul

  • @byby3131
    @byby31316 жыл бұрын

    Moustapha gningue dieurdieuf ti Barke sgn touba.

  • @saliousambe2894
    @saliousambe28944 жыл бұрын

    Alhamdoulilahi rabil alamïne Banou sunu borom mayé cheikh Ahmadou Bamba khadimou rassoul

  • @mamediarrafall4312
    @mamediarrafall43125 жыл бұрын

    Machaallha diaradief s touba amulmorom 💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏💗💗💗💗💗💗💗💗💗💗💗💗💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖

  • @sokhnaaminata287
    @sokhnaaminata2873 жыл бұрын

    maachaallaahu léruk tayjii ak ellek salallaahu halayhy wasallam

  • @mbackegadiaga7393
    @mbackegadiaga73938 жыл бұрын

    diadieuf mouride Hakassa amna sola Alhamndolilah

  • @FallouNdiaye-ub4co
    @FallouNdiaye-ub4co5 жыл бұрын

    Dieureudieuf serigne touba amoul morome

  • @cheikdiouf6345
    @cheikdiouf63452 жыл бұрын

    Machallah eskeye amina yaraby dieuredieufaty serigne touba khadimoul morom mbacke yalnanuko yala fayale diarram mame bousso diarra bousso akasa diarram cheikh ibrahima fall

  • @tourebarama5382
    @tourebarama53826 жыл бұрын

    thiye Serigne touba dieuredieuf Serigne touba

  • @youssouphasamb597
    @youssouphasamb5979 жыл бұрын

    Beg nanou lol si ndiangmi yalna sgnbi dolli mane gui barkep hassidayi

  • @cartercisso8555
    @cartercisso85554 жыл бұрын

    Thiey Ahmadou Bamba ka yémé 🤭🤭amoul moroom. Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall

  • @dadondao8922
    @dadondao89224 жыл бұрын

    Dieuredieufati S Touba Cheikh Saliou Mbaké

  • @mamecheikhibrafalllamp2061
    @mamecheikhibrafalllamp20613 жыл бұрын

    DIEUREUDIEUFETI BOROM TOUBA MACHALLAH KÉNE DOU SERIGNE TOUBA AK LIMOU BIND YEUP

  • @abdoulbaidygueye3621
    @abdoulbaidygueye36216 жыл бұрын

    Dieureudieuf SERIGNE SALIOU MBACKE

  • @awakadidiatoukoita8139
    @awakadidiatoukoita81394 жыл бұрын

    Machallah Yalna Yalla wéral baate bii

  • @binetandiayebinozzacouture5406
    @binetandiayebinozzacouture54062 жыл бұрын

    Yalla nagneup amediame thi barke cheikhoul khadim

  • @aminatafall1459
    @aminatafall14597 жыл бұрын

    sokhna Aminata Fall mou Serigne Saliou Dieureudieufeti Serigne Touba diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Cheikh Sidy Moctar yagh fi lole te wer àmine

  • @serigneabdoufall9899

    @serigneabdoufall9899

    2 жыл бұрын

    Èbxln

  • @fatoukinembaye1375
    @fatoukinembaye13758 жыл бұрын

    Alhamdoulilaah Allahouma Sally Alla Seydinaa Mouhamadine WaSallim.Dieureudieufaty Serigne Touba. diaaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall. saa sou kou Tedd ki massaana wakh diokh ma teere bi; Nourou Darayni la thi dioublou.kou tedd neena kou ko am; am nga yepp. kouko amagoul amna boo amagoul. Mbokkou djiouliite yi.mbokk taalibeyi niou goorgoolou thi Khassaide yi. Waaye nak garab goo gis dafa ame dose. Dieuredieufaty Serigne Touba Diaaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall.

  • @mornguirane7937

    @mornguirane7937

    7 жыл бұрын

    ma challahhhh

  • @sentesaliou739

    @sentesaliou739

    7 жыл бұрын

    akassa

  • @mameboussodieng9699

    @mameboussodieng9699

    7 жыл бұрын

    fatou kine mbaye .

  • @rokhayandoye7567

    @rokhayandoye7567

    Жыл бұрын

    MAA SHAA ALLAH 🙏🏾❤️🙏🏾DIEUREUDIEUF SERIGNE BAMBA 🙏🏾❤️🙏🏾

  • @amind3896
    @amind38962 жыл бұрын

    Machalah serigne Moustapha yalla nala serigne bi defal dian barké kou tedd ki

  • @makhahanesopeserignetouba2901
    @makhahanesopeserignetouba2901 Жыл бұрын

    Machala serigne moustapha gningue amna solo yalnala yalla defal barkep khassidayi❤Amine yarabi

  • @falldame3662
    @falldame36626 жыл бұрын

    dieurdieuf serigne touba xadim rasoul

  • @omardiop5999
    @omardiop59995 жыл бұрын

    Ça apaise mon coeur dieureudieuf serigne touba

  • @adjalam2792

    @adjalam2792

    2 жыл бұрын

    Q

  • @sokhnadiarraboussondiaye5456
    @sokhnadiarraboussondiaye54565 жыл бұрын

    Dieuredieuf Alhamdoul Khadim .

  • @sowelhadjimamadou6042
    @sowelhadjimamadou60423 жыл бұрын

    Manchalah dieudieuf borom touba kene dou môme 🙏🙏🙏

  • @iboufaye8299
    @iboufaye82995 жыл бұрын

    Machallaha kenne dou brom touba 🙏🙏🙏✍✍✍

  • @kassedioummabo8604
    @kassedioummabo86043 жыл бұрын

    Dieureudieufe borom touba diarawllak mame cheikh Ibra fall machalla

  • @generalewallydiouf4481
    @generalewallydiouf44817 жыл бұрын

    dieureudieuf Cheikh Ahmadou Bamba yaalna ngua am nguérémalou S TOUBA

  • @falloudiop6745

    @falloudiop6745

    7 жыл бұрын

    GENERALE WALLY IOUF

  • @rassoul8621
    @rassoul86215 жыл бұрын

    Macha Allah Cheikh Ahmadou Bamba

  • @thewatch01983
    @thewatch0198310 жыл бұрын

    Bismila, Alahuma Sali ala Seydina Mouhamad wa ala ilihi wa sahbihi wa salim. Je voudrais juste dire que Cheikh Bamba est la fierte de tous. :)

  • @abdoulayecoulibaly9244

    @abdoulayecoulibaly9244

    9 жыл бұрын

    Vu

  • @cheikhalma695

    @cheikhalma695

    9 жыл бұрын

    U

  • @immortelcamara768

    @immortelcamara768

    4 жыл бұрын

    Billahy wallahii 🙏👌

  • @renettemendy6858

    @renettemendy6858

    3 жыл бұрын

    Yalnala yalla samm

  • @colediangne4579

    @colediangne4579

    3 жыл бұрын

    @@immortelcamara768 7

  • @Dim_jrSmb
    @Dim_jrSmb4 жыл бұрын

    Xassida bi nékhna lolou wayee

  • @mbackeloum9580
    @mbackeloum95807 жыл бұрын

    akassa dieye serigne touba kėnl rėk

  • @Dim_jrSmb
    @Dim_jrSmb4 жыл бұрын

    Dieureudieufé serigne serigne amsatou Mbacké yalla guafi yague lolou tèh wére Mbacké 🙏🙏🙏🙏🙏

  • @bathiembaye4027

    @bathiembaye4027

    3 жыл бұрын

    Z

  • @hassaneba5102
    @hassaneba51028 жыл бұрын

    À diaraama khadim rasoulou

  • @evadiouf5238
    @evadiouf52388 жыл бұрын

    kénne dou Serigne Touba

  • @badoundiouck2199

    @badoundiouck2199

    7 жыл бұрын

    EVA DIOUF

  • @yeroxxx1
    @yeroxxx19 жыл бұрын

    ahmadou bamba le plus grand

  • @papasambabakhoum5917
    @papasambabakhoum59178 жыл бұрын

    DIEUREUDIEUF BOROM TOUBA

  • @papacissemaachaallah5397
    @papacissemaachaallah53973 жыл бұрын

    Dieureudieuffé borrom touba khadimou rassoul

  • @senyoutubetv4295
    @senyoutubetv42954 жыл бұрын

    Machalla dieuredieuf Serigne Touba

  • @dembandiaye875
    @dembandiaye8753 жыл бұрын

    thanks Serigne Touba

  • @mamadoudiop1674
    @mamadoudiop16749 жыл бұрын

    Tiey Serigne Touba kaine dou mome

  • @abdoulayendiayejazbu957
    @abdoulayendiayejazbu9579 жыл бұрын

    as salamou aleykoum dieuredieufaty SERIGNE TOUBA nehna loolll....

  • @papefall8932
    @papefall89325 жыл бұрын

    Dieureudieuf serigne touba

  • @lamine1406
    @lamine1406 Жыл бұрын

    J'ai découvert la lecture des Khassaid de Cheikh Gning, ça me touche le cœur. Allakhou Akbar, Cheikh Akhmadou Bamba Amoul morom. Priez pour le repos éternel de mon defunt père, les un an ce 1er Août 2022 Inch'Allah, borom bakh lawone. Yallah sounou borom def li gueune Allakhouma Amine.

  • @moisek147

    @moisek147

    Жыл бұрын

    Sa papa yalla nako yalla kharé dianatou firedawsi barké SAWS DÉKFARAL SARAKHÉL DAKH DIKO GNIANAL YALLA GA DÉSSÉ BARKÈM

  • @lamine1406

    @lamine1406

    Жыл бұрын

    @@moisek147 Amine dieureudjeuf dou yomb, mais Yallah bakh na demb rek dama dioy ba sonou sama khel dem thi mome, lepalakay fettelli. Souma sagnone domme bou né kene doula takkali ak sey wadjour., vice versa

  • @pedrorodriguez-ek3ff

    @pedrorodriguez-ek3ff

    Жыл бұрын

    ..

  • @soxnaaamina

    @soxnaaamina

    Жыл бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhdaoudaseck9056

    @cheikhdaoudaseck9056

    Жыл бұрын

    @@moisek147 ý0030 oo21019p

  • @ndiayecheikh9382
    @ndiayecheikh93828 жыл бұрын

    dieureudiefeti serigne touba Mbacke dieureudiefeti serigne touba Mbacke

  • @aliounebadarasy8368
    @aliounebadarasy83682 жыл бұрын

    JËRËJËF WA MERCI SERIGNE TOUBA

  • @madiawdibo3678
    @madiawdibo36784 жыл бұрын

    Machaallah Amna solo Dieuredieuf mourides

  • @diouflatyr7344

    @diouflatyr7344

    2 жыл бұрын

    Dirradieuf Serigne Touba

  • @rokhayambengue5885
    @rokhayambengue58852 жыл бұрын

    dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba dieuredieuf serigne touba

  • @sappassydarayeserignesalio1193
    @sappassydarayeserignesalio11938 жыл бұрын

    dieureudieufe serigne touba Khadim rassoul

Келесі