No face vilipende son ex Femme Mia après les polémiques"Limay wakh dou pour légui baniou tolou thia"

LOUBESS
Relation amoureuse entre Mia guisse et Farba _ Momo dieng défi Wally Seck _ Adamo tacle…
Soutenez TELESENEGAL TV en rejoignant votre chaîne KZread pour bénéficier d'avantages exclusifs 👉🏻 / @TeleSenegalTv
Pour plus de vidéos, Clique ici pour t'abonner ► / @telesenegaltv
TIKTOK: / telesenegal
FACEBOOK: / telesenegal
WEB: www.telesenegal.com
#Senegal #Sonko #focus2024 #Macky #Dakar #hennétime #sabar #live #waxsaxalat #kebetu #tiktoksenegal #viral #africa #Team221 #Africa #Sunu2019 #telesenegal

Пікірлер: 237

  • @babacarndong-ge7mc
    @babacarndong-ge7mcАй бұрын

    Ana goor ak lidianti Vie diambour yi ragal len yala❤

  • @princessemyadiallo9791
    @princessemyadiallo9791Ай бұрын

    Kharal ma mandou Ci rèk ndiallo mome da Diss bakar lay bagn kou mandou rek beuseul j'aime

  • @nafaatv7472

    @nafaatv7472

    Ай бұрын

    Sen thème youniak solo yî nguén wara bâyi. Sénégal DEFA Nek si reconstruction, il faut pausé les bon sujets qui intéresse les Sénégalais et leur développement.

  • @papisstoure8196
    @papisstoure8196Ай бұрын

    Les senegalais doivent changer de mentalité vraiment! Foutez la paix à cette dame ohh

  • @lanature1060
    @lanature1060Ай бұрын

    Franchement, ils doivent nous épargner ses règlements de compte en public (garou walei bi etc ) . Ils étaient en couple, ce qui se passait ne concerne qu’à eux. Ils doivent respecter leur fille qui sera l’unique victime !!

  • @binetasow2883
    @binetasow2883Ай бұрын

    Bilahi animateur bi je suis très fier de toi no face na déf yeufou goor yonam nékoul si mia guissé je suis tout à fait d'accord avec toi ouz

  • @Lisambay3895

    @Lisambay3895

    Ай бұрын

    Est k dou son ex mo koy yakhal. C 1mauvais perdant mia da mole dé Machalah

  • @mohamadsabaly1866

    @mohamadsabaly1866

    Ай бұрын

    Binta attention boul faténi ki am na dom ak Mya et ce comportement de Mya risk d'influencé sa fille

  • @fatimazahrandiaye7431

    @fatimazahrandiaye7431

    Ай бұрын

    Yen esk cv no face dafa am dom ak mia amna droit s’inquiétait car le comportement de cette dernière est très irresponsable et il ne veut certainement pas que ces mauvais actes influence sa fille et amnasi droit ndakh Kou sanione bo diourei sa dom molay gueune boudei nite kou bakh nga👆bo néh fimouko waxè lako waroul won waxè mani je suis d’accord avec toi mais il a le droit de s’inquiéter des comportements et des actes irréfléchis de Mia plus k nous tous car dafa yorei domam nexoul si xol tei après lay comprendre

  • @binetasow2883

    @binetasow2883

    Ай бұрын

    @@fatimazahrandiaye7431 yaw lay lathie est ce que cva Lou mou done kholé ba Mia reuthie KO comme leurs liens c'est l'enfant no face n'a qu'à s'occuper de son enfant Punto

  • @binetasow2883

    @binetasow2883

    Ай бұрын

    @@fatimazahrandiaye7431 est ce que dagua fék mia guissé mouy déf lou Bone ce que Ahmed Cissé à dit ce ne sont que des rumeurs personnes de vous dogue khoul ba guiss mia si lou bone avant de juger une personne tu dois le connaître et pire no face n'a plus le droit de contrôler mia parce qu'il n'est plus sa femme okay

  • @oulimatacocottediop1801
    @oulimatacocottediop1801Ай бұрын

    Voila niit doko beug diko torokhal wala diko yakk…wala diko weerrr ak diko douleul ak dieuw surtout..faut que nit yi kham ni entre l’amour et la haine c est un SEUL PA…ils peuvent s aimer pendant leur ménage mais souvent méthode de séparation bi rek qui peu déterminer après le divorce leur comportement et la manière de se séparer peu causer une haine définitive quelque soit les moments partagés avant…

  • @cheikhndiaye4199
    @cheikhndiaye4199Ай бұрын

    Séne site yi yeup lagnou wara téthe ndéyame parce que yéne amoléne béne liguéye li d'où liguéye Sénégal amna pétrol âme gaz âme surquon est temps deautre wakhi léne si térain Bi déme wouti informations you l'ère té wor

  • @user-yg5cb6jv4q

    @user-yg5cb6jv4q

    Ай бұрын

    Wkhal deh

  • @mbayestarsene2179

    @mbayestarsene2179

    Ай бұрын

    😂😂😂😂bilay

  • @user-fu3mn8wy7b

    @user-fu3mn8wy7b

    Ай бұрын

    Motax diarougno😂sax abonné ay emission niou niakk fayeda

  • @nafissatoudiop89

    @nafissatoudiop89

    Ай бұрын

    Dou ligueye dé wakh deuge topou cas rek le monde vas mal wakh lène si Lolou

  • @souleymanecisse9078

    @souleymanecisse9078

    Ай бұрын

    Bilahi

  • @mathusalemchanel3314
    @mathusalemchanel3314Ай бұрын

    mouno lèn lir di deff media🤣

  • @KarimouBionka

    @KarimouBionka

    Ай бұрын

    Moma diaxal😂😂😂😂😂😂

  • @BOROMLERGUICISSECISSE

    @BOROMLERGUICISSECISSE

    Ай бұрын

    Wallahi Sénégal dafa nekh rek

  • @ismailacisse1992

    @ismailacisse1992

    Ай бұрын

    Ta commentaire ma tuée 😂😂😂

  • @veriteabsoluedeugneekhoul1720

    @veriteabsoluedeugneekhoul1720

    Ай бұрын

    😂😂😂

  • @awaaidara8729

    @awaaidara8729

    Ай бұрын

    Gni kay ay domeram laniu sim

  • @AdeleDefem
    @AdeleDefemАй бұрын

    Amatoul béne droit si mom Mia amna droit vie vie wam lolou Mia la concerné

  • @diodio57327

    @diodio57327

    Ай бұрын

    Merci ta tout dit❤

  • @fatimazahrandiaye7431

    @fatimazahrandiaye7431

    Ай бұрын

    Certes mais boul fatei ni danio am dom et Mia est une mauvaise influence pour sa propre fille ndakh amoul kilifeuh vulgaire na lolou rk meune nako yeungeul bouy guiss yeneu yii si sa yayou dom nexoul si xol boudei mia kassei yakaar ni bouniouko ko done mayate yakarou mani sakh dinako dieul mais dom biniou sekh tei limou wax tmt nexoul mais c vrai lissi kanam rawouli beute juste fimouko waxei lako waroul won waxè rk mais pr mane dafa waxè xol rk

  • @mariane2697

    @mariane2697

    Ай бұрын

    Douloloulou déh wakhdji moy dako nop ba tay mane soumala bayé damay tourné sa page wayé tass ak niteki diko top diko Lidieuneti​@@fatimazahrandiaye7431

  • @assanendiaye2997

    @assanendiaye2997

    Ай бұрын

    Yaw Eska Nit Nga Bouy Xalaat Sa Wakhi Doff Bou Amoul Dossier Médical Bi Moy Lane Comme Divorce Nagne Louko Nex La Wara Doundou Te Doussi Xalaat Dômame

  • @mariane2697

    @mariane2697

    Ай бұрын

    @@assanendiaye2997 😃😃kikay dof pus la kouma wakhone cest genre de mental exercise téna doumako gueum

  • @marieheleneberre8736
    @marieheleneberre8736Ай бұрын

    Il n'a rien à lui dire il y a le divorce il n'a qu'à s'occuper de ses propres problèmes et laisser cette Mia en paix.

  • @seynabouthior2365

    @seynabouthior2365

    Ай бұрын

    Doyaloul si Mya😂😂😂

  • @aicha7979
    @aicha7979Ай бұрын

    No face kou niak diom leu Bilayy seu genre d’homme toxique et méchant m’écœure

  • @aminandong7735

    @aminandong7735

    Ай бұрын

    Kii yeufou goor gordjiguene rk lay df

  • @mariathiam344

    @mariathiam344

    Ай бұрын

    😂😂😂😂😂Wouyeee

  • @cheikhndiaye4199
    @cheikhndiaye4199Ай бұрын

    Thiote ndéyame yéne diguéne yékha avancé yéne d'Al tok Di lék nite yi rék monye séne liguéye fi adouna Bi tôle amoléne loudoul li séne thiote ndéye waye

  • @kofenMC
    @kofenMCАй бұрын

    Le PRÉSENTATEUR TRÈS INTELLIGENT

  • @AdelineCabral
    @AdelineCabralАй бұрын

    Si c'est vrai où est le problème ??? Quelle loi religieuse ou légale interdit la relation amoureuse entre Mya et Farba ??? L' ascension musicale de Mya fait mal au cœur de certains

  • @awasanneh9174
    @awasanneh9174Ай бұрын

    Na deff yefou gorr yonom nekatoul thie Mia

  • @mayaciss6821
    @mayaciss6821Ай бұрын

    Y a plus important à régler Au Sénégal en ce moment un plateau pareil la honte, parlons des sujets plus importants pour faire avancer notre pays de la TERANGA

  • @emviepotee4754
    @emviepotee4754Ай бұрын

    Non contana thi grand bi bi tu as tout résumé. Nit Day am soutoureu.cest fini donc qu'il tourne la page même s'il a des secrets de Mia

  • @user-db9qg3cq4e
    @user-db9qg3cq4eАй бұрын

    Mane dale amna louma meti goor bo divirce ak djieguene daka wara def comme sa soeur rawatina gua am ak mome dome mais Sénégal mo melni kougnou yeketi menane la wathie mane divorcée na sama 1er mariage le 2em c’est le père de mon 1er mari qui ma donner mon deuxième mariage comme bayalee bou gnawone dou ame❤

  • @rokhayasow4334
    @rokhayasow4334Ай бұрын

    Le gars en T.marron est véridique

  • @esperancesagna235
    @esperancesagna235Ай бұрын

    Yene kou lene wakh né ci mia lay wakh dolene mandou mom tamiit saga naniou ko fi niom niar nio kham li khew seni diganté ragal lene yalla té mandou ci

  • @user-mt1rv5wy1m

    @user-mt1rv5wy1m

    Ай бұрын

    Ak lou meuti khew Yalla mo ndjeuk soutoural domou adama kone nagnou soutaralanté sounou bière Adouna amoul solo Té yowmalkhiyam matena saure

  • @AdelineCabral
    @AdelineCabralАй бұрын

    AU SÉNÉGAL DÈS QU'UNE FEMME REUSSIT PROFESSIONNELLEMENT, DES HOMMES SURTOUT DES EX SORTENT POUR L'ABATTRE. MERDE WAÏ

  • @youssoufcheikhhaidara7829
    @youssoufcheikhhaidara7829Ай бұрын

    Je suis d'accord qu'il ne devais rien posté mais aller jusqu'à dire que le gah devais le defendre n'importe quoi ... loubone rekk guéneu beug

  • @mamdegenngum2671
    @mamdegenngum2671Ай бұрын

    Merci beaucoup ❤❤

  • @user-hn2op5in3h
    @user-hn2op5in3hАй бұрын

    Yen tamite kene rawoulene cas rek chiim 🔥

  • @BarryRacine-b..L.k
    @BarryRacine-b..L.k20 күн бұрын

    en réalité il devrait lui oublier vraiment après l divorcé un garçons dois vraiment être comme un vrai garçons

  • @soumaremoussa9458
    @soumaremoussa9458Ай бұрын

    Bravo 👌✊

  • @ArameNdaiye
    @ArameNdaiyeАй бұрын

    Mia clip lay wathai amétt sisé day wakh rék no fées hamna lie clip la

  • @molaminmanneh-fs6wn
    @molaminmanneh-fs6wnАй бұрын

    Merci deuga naa neka gorr❤

  • @mamendiemethiam7540
    @mamendiemethiam7540Ай бұрын

    Quelque soit alpha c'est sa vie no face n'a rien à dire sur elle seuye ba diékh na

  • @BoussoGueye-fp9dx
    @BoussoGueye-fp9dxАй бұрын

    Merci beaucoup bien dit ❤❤

  • @matabayetv8301
    @matabayetv8301Ай бұрын

    Bravo à l'animateur 🎉🎉🎉

  • @fatoundao6305
    @fatoundao6305Ай бұрын

    Machallah wahga déucue

  • @user-ep5yu4nx3i
    @user-ep5yu4nx3iАй бұрын

    Wala bo doyaloule si mia bok ga wakh niou niou delo lako parske dafa melni yakoye fire ba tay mome lidiantiwoula est ce k do def ni mome

  • @FarmataBinetaRacineKeane
    @FarmataBinetaRacineKeane9 күн бұрын

    Souko defendrone aussi nityi nii loutakh lolou Sénégal metinaa

  • @seynaboucisse9304
    @seynaboucisse9304Ай бұрын

    ouzz merci way

  • @user-vo4tf1um9k
    @user-vo4tf1um9kАй бұрын

    Mia mo mome khalisssam loukossi nékh lay def défoul lou bonne bayiléne domou diamour lane nék léne nitt way

  • @HousseynKadi
    @HousseynKadiАй бұрын

    😮😮

  • @MairamDia-cp6qy
    @MairamDia-cp6qyАй бұрын

    Katalen sénnn ndeye liii thème laa vous avez beaucoup de choses à débattré yen yaka derrr rk nguénn meunnnn ouz ta bien dit

  • @cecedi83
    @cecedi83Ай бұрын

    No face il parle bcp trop pour un homme, il est tout le temps en train de gaarouwaleh vraiment il n'a qu'a vivre sa vie et laisser mia tranquille. Elle ne parle jamais de lui. Goor bou gnaka fayda la. Mia Guissé est en train de faire sa carriere, ou en est il lui? Personne n'a mis son son pour le clasher il cherche juste le beuzz, qui va mettre son son dans la rue pour soit disant nakharal ko? Il se donne de l'importance vraiment. Il est pitoyable.

  • @paulinemalack7188
    @paulinemalack7188Ай бұрын

    He should grow up and stop looking for attention. Mia has moved on already. What is his business with what negative people are talking about her?

  • @rassoul__moustapha3955
    @rassoul__moustapha3955Ай бұрын

    An tous cas Défoul Youfou Goor Yalla ki Yambar la waay , Djiguén mola diaral lii no niak ngua fayda na Donal mak , Djiguén bou dieulé younam bawal ,looy topp si guinaw

  • @aicha7979
    @aicha7979Ай бұрын

    Kou niak diom leu genre goor gni nimaleine dieppi..ki da sohor kasser et c’est flagrant

  • @SaneAbdoulaye-rr9dy
    @SaneAbdoulaye-rr9dyАй бұрын

    Lou am solo nga wah si Sénégal yii

  • @DioneAliou-jv4xh
    @DioneAliou-jv4xhАй бұрын

    Sénégal yakh derr rek Sénégal thiotou ndeye journaliste Sénégal Sénégal data yaye

  • @mj-zq4qg
    @mj-zq4qgАй бұрын

    Dinga beugue nit mouno thie diote nga fekhe nokoiye yakhee

  • @mbayestarsene2179
    @mbayestarsene2179Ай бұрын

    Sounou yone nekoul ndeye si mia guissé ak no face

  • @tinomartingreg
    @tinomartingregАй бұрын

    mia yagui influencé khalei yi déh si sa musical li ses injustes li mome dafa eupe koi tiyé leine séne domi djiguene yi

  • @binettegueye1433
    @binettegueye143327 күн бұрын

    Danguena guis ben yone Lou toudou fi Mÿã guissé 👩🏾‍🦯

  • @ibandiaye4473
    @ibandiaye4473Ай бұрын

    Waa grand place bii....lidieunti ndaye problème jambour yi rék.

  • @maimounandaw6329
    @maimounandaw6329Ай бұрын

    Merci yonam nekatoul tji mia guissé ...mia yayou domam la ..na rafett

  • @marianendoye
    @marianendoyeАй бұрын

    Arrêter de parler de mal aux femmes vous avez des sœurs, n'oubliez pas que vous avez des méres . Son ex n'a rien n'a dire. Elle n'est plus mariée, elle est libre c'est ça vie. Arrêter de juger, le seul juge c'est le bon Dieu. Vous avez des problèmes à régler chez vous allez les résoudre c'est mieux. C'est sa vie. Chercher d'autres débats plus importantes

  • @antadiop8547
    @antadiop8547Ай бұрын

    Vraiment no face n’a digne té manou si mia li tkt dou diam au final sa montre que doyalo si mome 😢

  • @pakothelow
    @pakothelowАй бұрын

    Vous interprétez mal les propos du gars. Il ne parle pas de ça et il l'a dit Alors analysez et tenez-vous en à ses écrits. 😢

  • @ndagousarrba9217
    @ndagousarrba9217Ай бұрын

    Dokhal sa dokh bayi Mia mou dokh dokham défal yeufou gor

  • @taliberek5499
    @taliberek5499Ай бұрын

    Ouz je suis fier de toi dohal dohinou talibé rek

  • @annakoite8920
    @annakoite8920Ай бұрын

    Koulèn yakh nè mia laye wayale

  • @Galsn

    @Galsn

    Ай бұрын

    Moma diakhal

  • @user-rw4km6re4b
    @user-rw4km6re4b4 күн бұрын

    Farba mgom dé dioutal déh 😂😂

  • @user-ok8no3rg1e
    @user-ok8no3rg1eАй бұрын

    No face na mayè pateh bi si life Mia bi bolè organise life am

  • @ibandiaye4473
    @ibandiaye4473Ай бұрын

    Dimbalè leène niou nguènn lidieunti sèn ka yèn,té baayi problème jambour... Sa me fait mal de voir ce couple autrement ,et puis comme si vous êtes satisfait d'amener cette histoire devant la cour. Senegal.....je suis pitìé.

  • @YvoneMendy
    @YvoneMendyАй бұрын

    Vraiment il n'a rien expliqué

  • @user-rr7vy8hj3y
    @user-rr7vy8hj3yАй бұрын

    Niouy diay intelligence ni

  • @user-qv3cw2gp8v
    @user-qv3cw2gp8vАй бұрын

    Peut-être en mariage la il doit connaître des choses...

  • @MasterOus-ou3df
    @MasterOus-ou3dfАй бұрын

    Nanguene Gore way. .. 😂

  • @user-or4se9ij4u
    @user-or4se9ij4uАй бұрын

    Ohh wadji mo gnémé DEUG way😊😊🎉

  • @thiorogueyesarr5895
    @thiorogueyesarr5895Ай бұрын

    Nguir yalla dolen wah si chômage bi, solution si gal gui etc nguir yalla shuuutt

  • @qezzmilli9512
    @qezzmilli9512Ай бұрын

    They guy with brown T-shirt all what he said is real fact

  • @moustaphandiaye5168
    @moustaphandiaye5168Ай бұрын

    Yén nakk com mouno lén lir danguéna wara diangué ba paré 😂

  • @ElhadjNiassetoure-kp2qs

    @ElhadjNiassetoure-kp2qs

    Ай бұрын

    Gnikaye ay mbame lagn😂😂😂

  • @thiernodiallo2830

    @thiernodiallo2830

    Ай бұрын

    Billahi 😂😂😅😅😢

  • @user-kb5ep7tl3m
    @user-kb5ep7tl3mАй бұрын

    Noo face dafa noak fayda t4 matady mia guissé nekatoul diabaram na dem fawi niak nga classe thi goor

  • @celestinegomis4007
    @celestinegomis4007Ай бұрын

    Je ne sais pas si tu es journaliste ou chroniqueurs vraiment tu es incroyable

  • @seynaboucisse9304
    @seynaboucisse9304Ай бұрын

    merci way yw nk vrai goor gua té wax gua deug yonam nékoul si mome goor day df yeufou goor té diapalé wouko té xoloul si dom dji

  • @FarmataBinetaRacineKeane
    @FarmataBinetaRacineKeane9 күн бұрын

    Farba Ngom aussi nitkou bonla bakhoul santoul yallah, sollen ko khamoul batay dollen ko meussa khamati

  • @cheikhfall7903
    @cheikhfall7903Ай бұрын

    No face.khamal ni ameguen ayy domm

  • @yorongom9374
    @yorongom9374Ай бұрын

    Ana goor ak beug cas!gnak jom gueen def

  • @jflixibrahimjfibrahim5127
    @jflixibrahimjfibrahim5127Ай бұрын

    Diangileen

  • @aicha7979
    @aicha7979Ай бұрын

    Tala nala yalla mousseul ci goor Walleu ex bou bone no face il est méchant et ignane kii

  • @Omarsane7491
    @Omarsane7491Ай бұрын

    Gor yalla day def weufou goor yalla

  • @ibandiaye4473
    @ibandiaye4473Ай бұрын

    😂sou nguènn thi noòpi wone,il se pourrait qu'ils reviennent de nouveau....mais ték ko thi digui penc bi ,n'arrangera pas grand-chose, au contraire dafay gùeneu yakk.

  • @toutoularandiaye2116

    @toutoularandiaye2116

    Ай бұрын

    Noface moka publié bo abonné pageam détails rek Lafay pub Di menacé AK ay bloqué. Goor bou wah mounila sokhnasi avancel. Di fatali ay gueu youko done kokeuli boutique aéroport AK first son Mia. Noface mi wahlen KO DEUG. Mia seuyoul kou KO neh andal tank empiété woul thi sougnou liberté

  • @sonko2024rk
    @sonko2024rkАй бұрын

    Yénnn amoulén dég dég dh kilimou wakh Mia laye défendre

  • @Galsn

    @Galsn

    Ай бұрын

    Sénégal nioune daniy deg wakh rek lékoko

  • @AbdoulayeCisse-vl1zm
    @AbdoulayeCisse-vl1zmАй бұрын

    Yene amet Cissé khamoulenko batay ki buzz rekk lay wout Sénégal si bopam ño niakk fayda

  • @charlesmanga1632
    @charlesmanga1632Ай бұрын

    Mia est passé à autre chose il n'a qu'a faire la mm chose n'a gooré way

  • @reseauxsociaux3352
    @reseauxsociaux3352Ай бұрын

    😂😂😂 gnom gnouni gorr dey def yeufi goor😂😂 dama tomber si gnii par hasard mani xaral ma xol sènn xeetou liguey🤷‍♀️😂😂 mais guiss ngen gniiii… wa lii liguey leu gnou melni gnou reir… viiiiie wou djammmmbour! Ayyyyy liiiiiiiiiiiiii ! Sou ngendi djouli da ngendi bayi khel si xetou djeuf gui ngendi wowé liguey ? Mba yenangui gnaann yallah mou gueinei len si lii niii Mais tt l temps sen kanami né fanngh si ecrans yi di magnerou aka diap sen touniou diko bomb si VIWOU DJAMBOUR

  • @user-rs7nn6tz7j
    @user-rs7nn6tz7jАй бұрын

    Grand bi dof leu no face waroul wax cil lolou Sénégalais yagui xol gnogui guis nél thiéle rék histoire dinala waxal

  • @user-rw4zn5qc8i
    @user-rw4zn5qc8iАй бұрын

    No face mome khana doyaloul sii seuy bii mia bimouko diapalei idda la seuyeum diekh donc amna droit neikk ak kouko neikh

  • @thilloboye430
    @thilloboye430Ай бұрын

    No face mom doungou leu lothi yonam

  • @kharndoffenediouf48
    @kharndoffenediouf48Ай бұрын

    Ouz sa niveau bi dafa touti torop kén dou tok plateau di wahé halatt del geneu matial sa hel ci say reponse ak say prise de position

  • @user-pc8cy7ly9l
    @user-pc8cy7ly9lАй бұрын

    Amoul dar limouy wakha

  • @yeswecan995
    @yeswecan995Ай бұрын

    Goor yomboul dé wakh bou leer la

  • @FarmataBinetaRacineKeane
    @FarmataBinetaRacineKeane9 күн бұрын

    Le Monsieur en boubou marron c’est l’ami à Marie Louise ou bien d’où momo

  • @cesaltinegomis2739
    @cesaltinegomis273926 күн бұрын

    Yénite déf léne yeuffou goor

  • @mamedialedia8378
    @mamedialedia8378Ай бұрын

    DANGAA DKISJONCTÉ MOOTAKH NGAY WEURI VIDÉO . TAGGOOK NITE DIKO SURVEILLER NIAKK DIOMLA

  • @LataFaye-mg3mp
    @LataFaye-mg3mpАй бұрын

    non face môme il n'a rien de ceu qui est fondamentale à l'homme

  • @IgnaceMignaneDiouf-bj3ny
    @IgnaceMignaneDiouf-bj3nyАй бұрын

    Eup fil problème dii lidjiantii problémou djiabou. Vous aussi concentrer vous sur vous même ainsi k les commentateur. Gnakeu fayda

  • @mamenabyndour
    @mamenabyndourАй бұрын

    Gor dou niak di niancki

  • @krg-events2215
    @krg-events2215Ай бұрын

    Leep dora gueye la

  • @binta4894
    @binta4894Ай бұрын

    Europe lagnouy tok di yakh sénégalais yi boudone Sénégal lagnou nek tothieu nanou sen leufeul ndaye

  • @ndiayeomar84
    @ndiayeomar84Ай бұрын

    😢😢😢😮😮😂😂😂😂😂😂❤❤❤

  • @ndeyesoukaba172
    @ndeyesoukaba172Ай бұрын

    Sauté guéne mendouwoul léne

  • @nitoudeugue4930
    @nitoudeugue4930Ай бұрын

    Ces chaînes de merdes ainsi que tiktok laniou warra teudj meuneu focus touti thi souniou Sénégal

  • @Galsn
    @GalsnАй бұрын

    Wa mom toudoul kéne légui louy problème bi deuk bi tamite ahh

  • @deugrek3312
    @deugrek3312Ай бұрын

    Yalenanou YALA Khire Ci loubakh

Келесі