Njarign Yi Nekk ci Pigeon " PITAKH LU AM SOLO LA CI NIT " par Elhadji Malick Gueye partie 1

Пікірлер: 48

  • @hinatauhuga918
    @hinatauhuga9182 жыл бұрын

    Nguirr yalla gorgui do binde livre 💷

  • @gorathioune6482
    @gorathioune64822 жыл бұрын

    S malik🇸🇳na bindue livre 📖

  • @sylla4983
    @sylla49833 жыл бұрын

    Machallah serigne malick yAgg na la suivre yalna xam xam bi yokk

  • @cameraismaila5907
    @cameraismaila59072 ай бұрын

    Questo video e belissima ❤❤

  • @toyatoanase5021
    @toyatoanase50213 жыл бұрын

    Machallah elhadji malick Gueye niou mel ni yawe nio manqué si deukbi

  • @gninguebamba2197
    @gninguebamba21976 ай бұрын

    ❤❤ machaallah amno solo lool

  • @dakarbuzzzzz
    @dakarbuzzzzz2 жыл бұрын

    Xam xam amna billahi da lakhou rek🙏

  • @rassoulrassoul410
    @rassoulrassoul4103 жыл бұрын

    Machallah machallah amena solo taye amena louma diangue thi quelques mala amena solo

  • @cafetouba8373
    @cafetouba83732 жыл бұрын

    Maa shaa Allah dieuredieuf serigne malick yallah naa yallah May laa diam ak ay ndam rèkk in shaa Allah rabbi barkèp akhmadou bamba barkèp mame cheikh ibrahima fall Lamp

  • @malicksamb6051
    @malicksamb6051 Жыл бұрын

    Macha Allah yallah na senn djam yagg wakhtan wi amna solo bilay

  • @youssougningue8288
    @youssougningue82882 жыл бұрын

    Salam c 1 espèce kon doit protéger parce dans l histoire ils ont aidé les prophètes et c bon pour le sang

  • @coumbandoffenedioufndiaye4834
    @coumbandoffenedioufndiaye48343 жыл бұрын

    Dieuredieuf serigne Malick Gueye

  • @yslmfamill1712
    @yslmfamill17123 жыл бұрын

    Machall yalla na yalla yoko xam xam Bi

  • @thiernoseck8654
    @thiernoseck8654 Жыл бұрын

    Yalla guaffi yague 🔥

  • @seydina_jibril
    @seydina_jibril2 жыл бұрын

    Kiy posé kesion kou eupeul leu nit sooko laadjé dankay dèglou mou tontou

  • @mouhadiakhate1
    @mouhadiakhate13 жыл бұрын

    K dieu vous protège

  • @babacarmbaye1422
    @babacarmbaye1422 Жыл бұрын

    Bo bindone livre je suis le premier a faire la commande

  • @laminendiaye853
    @laminendiaye8532 жыл бұрын

    Machalla Amna solo seringe bi

  • @diopbamba4066
    @diopbamba40662 жыл бұрын

    Massallah kaddu yi am n'a solo mais def l'en émission pour ñiy diang louy néxal sen khell bañouy maná comprendre leçon yii

  • @tedoungalfouladou977

    @tedoungalfouladou977

    Жыл бұрын

    Hana do gawa comp leçon yi

  • @bayedjilyndiaye3975
    @bayedjilyndiaye3975 Жыл бұрын

    Machallah ❤💓💗

  • @nogayedieng4881
    @nogayedieng48813 жыл бұрын

    Merci w Sénégal TV vieil kholyourateyldiaragene

  • @basiroudiop9845
    @basiroudiop98453 жыл бұрын

    Ci kheti nguéni wakh mais degouma bène ne yone nguene wakh ci kheti diokh lene kheti wathi wayame sak jours bolene di wakh si kheti denguene di guene ne gam wakhagolene ndiarigne yi kheti am balegui mais critiquer woumalene

  • @cissesalif3691
    @cissesalif36912 жыл бұрын

    Am Na solo .Mai journalist bi nay Dek Lo book

  • @amsagayebeaugosse
    @amsagayebeaugosse2 жыл бұрын

    Masàllaa

  • @hinatauhuga918
    @hinatauhuga9182 жыл бұрын

    Machalla pa bi khame khame bou lére la ame

  • @diopbireume9428
    @diopbireume94282 жыл бұрын

    Dieureudieuf Serigne malick Gueye

  • @serignemassambadiouf2752
    @serignemassambadiouf27522 жыл бұрын

    Macallah

  • @babacardiakhate2449
    @babacardiakhate24492 жыл бұрын

    très interessant

  • @mansourbiramadia8124
    @mansourbiramadia81243 жыл бұрын

    Celui qui pose les questions il parle trop sans rien dire il doit laisser le marabout développer

  • @yigopro1773

    @yigopro1773

    2 жыл бұрын

    Thieuy yi français 🤣🤣

  • @saliouieye8029
    @saliouieye80293 жыл бұрын

    Amna solo lol

  • @djibykante452
    @djibykante4523 жыл бұрын

    Arona invité younioula wa invité dégueloule

  • @ibrahimaseck1488
    @ibrahimaseck14882 жыл бұрын

    J'ai triste

  • @princesjay9273
    @princesjay92733 жыл бұрын

    Thank you so much ❤️

  • @mariesy3616

    @mariesy3616

    3 жыл бұрын

    Aķ F s

  • @moustaphadiagne6619
    @moustaphadiagne66193 жыл бұрын

    Infatigable el hadji Malick geuye

  • @cheikhbadian4083
    @cheikhbadian40832 жыл бұрын

    bilakhi ki bou wakhé ngané dafa aye mais khamoul dara mame déme na bassi mome loume ma diokh dara barakhoussi ba paré cher lék khaliss diambour yi rék lagne fi néké

  • @diordiop8490

    @diordiop8490

    Жыл бұрын

    Cheikh badian ñii door rek khamouñou tousse

  • @alhamdoumballo8414
    @alhamdoumballo8414 Жыл бұрын

    Ki dé bou déwé xam xam dé billay do nit dé lou lérre gua wakh

  • @niangcheikhibrahima9673
    @niangcheikhibrahima96733 жыл бұрын

    Si kaw si kanam

  • @badadiakhate7591
    @badadiakhate75912 жыл бұрын

    Mane dé dama bouka sathe geure noumaye defe

  • @allansarounabitvamar7927
    @allansarounabitvamar79273 жыл бұрын

    yaw mi your question dafawara am éducation bou wara your tayou rouko

  • @malickgaye6651
    @malickgaye66513 жыл бұрын

    Li bindou gnouko fene si alkhourhane kouy yar pigeon pour gua am dom day jafe

  • @cheikhmbackembaye1411

    @cheikhmbackembaye1411

    2 жыл бұрын

    Sa may nidiay nieupou ay pigeons la niou yor té nieupeu am ay dom li gua wax ték ko fén niou xam

  • @mouslyseye2476

    @mouslyseye2476

    2 жыл бұрын

    Ndax jigeene mana yor pengo s.malik?

Келесі