MADA BA parle de sa relation avec sa soeur Sokhna Khady et attaque Gagne Siri GUEYE de la Sen TV

Пікірлер: 316

  • @djimegaye4670
    @djimegaye46702 жыл бұрын

    Bravo Mada, Ton honnêteté est appréciable. Je te comprends car je vis une situation similaire

  • @dethiediagne3387
    @dethiediagne3387 Жыл бұрын

    Mada ba une femme plein de dignité ❤❤❤

  • @ibrahimadieng5783
    @ibrahimadieng57836 жыл бұрын

    Mada courage j'aime ta personnalité. Les mauvais commentaire ne prête pas attention... Si on a de mauvaise relation avec quelqu'un d'autre même si la mort survient il faut garder ta position si on est pas hypocrite

  • @user-ot6kj9nw4d
    @user-ot6kj9nw4d22 күн бұрын

    Mada ba,en référece pour cette génération de musiciennes,elle est belle mais ne nous a jamais offert un scandale...respecr❤

  • @sophiamarques7797
    @sophiamarques77979 жыл бұрын

    Mada Ba je l'ai toujours aimé, elle est très posée et très véridique. Courage Mada

  • @kalidouwade9442

    @kalidouwade9442

    5 жыл бұрын

    Envoie moi message 767271827

  • @ngba01
    @ngba019 жыл бұрын

    Deugue kénn doukou neubeu. On vois la vérité sur son visage. Je l'estime bcp et elle est ma copie de femme que je veux ressembler. Une femme calme et toute posé, très précise dans sa langage. Longue vie à toi

  • @berebuxamxam1383

    @berebuxamxam1383

    6 жыл бұрын

    Nar Sofia Amiine waay moi je cherche son numéro désespérément . C'est une femme de valeur

  • @djibm9m998

    @djibm9m998

    5 жыл бұрын

    mada bete nama

  • @ndeyamie6808

    @ndeyamie6808

    5 жыл бұрын

    @@djibm9m998 gns ne kansfjs'd Je

  • @Thiar-nt2oc
    @Thiar-nt2oc26 күн бұрын

    Ma voisine de liberte5 etant gamin❤❤❤

  • @senegalaise2251
    @senegalaise22516 жыл бұрын

    Bayilèn di wah wahi soutoura loolo yah senegal. Ki dagnko fenal dafko wara léral. Bravo Mada. Senegalé hamou deugue.

  • @FatoubintouMbodji-tw8mb
    @FatoubintouMbodji-tw8mb25 күн бұрын

    Ce ki ont là après confession expliquer leen ma nou histoire bi démé

  • @abybodian1448

    @abybodian1448

    24 күн бұрын

    Ma gui nii😂😂😂😂

  • @antagueye2645

    @antagueye2645

    23 күн бұрын

    Gnogui ni topeuse de cas ​@@abybodian1448

  • @KY-ed5qp

    @KY-ed5qp

    22 күн бұрын

    On est là on comprend pas 😅

  • @lalafaye2072

    @lalafaye2072

    19 күн бұрын

    Li histoire bou yagu leu.Madaba ak sa famille niou deuk té deukine bi nékhoul wone comme pratikmnt bcp de famille nga am ay rakk dégalougn leu kou nék dieul sa yonou bopp di déff louléne nékh.kéne wagnékouci ndakh nimé guénéwone ci keur gui nékhouko wone .Gagnsiry une membre de la famille et animatrice de la radio joubou woul wone ak Madaba am loumko dinthial di utilisé temps d'antenne nam diko di déff ay thème diko garawoula à chak fois k l'accaz se présente.sheuttt l'histoire longue meunouma bind lépp té youtube amoul vocal😂😂😂

  • @abybodian1448

    @abybodian1448

    18 күн бұрын

    @@lalafaye2072 merci à toi

  • @cheikhmbackediop7678
    @cheikhmbackediop76786 жыл бұрын

    Sokhna Khadi dh dafa bakh yalla nako yalla Faye barkeb Serigne Saliou mada yaw comma bétga

  • @mayoutoure8166
    @mayoutoure81669 жыл бұрын

    wallahi Mada degue gua wakh kéne dou yow Awa Ba dé féne rek lay def meunoul séte meunoul dara meuna loula dara digua bok ak nite bou sokhoré laa Mada Ba doneul way 111ans koula bagne YALLAH na dé wayyyyyyyyyyyyyyyyyyy

  • @babacardiouf1071
    @babacardiouf10719 жыл бұрын

    salam wa sénégal magui djégalou mais nanou tapé xol yi té rafetal sounou ande ak dolénté soutoura téy diégalé. Sokhna mada yalla nala yalla défal name délossi wate sa rakabi thi kadou yiguéne wouté baguéne andate done béne nax bokou ba paré dioubo dafa néx té lolou la l'islam diguelé. Sokhna khady na yalla djégual ko ak moléme dioulite boumoufa féke té ték lokhome thi ndiabote gui moufi bayi encore une foi nanouy mougnalanté tay djégalé merci.

  • @khadijatraore3090
    @khadijatraore30904 жыл бұрын

    Massa, Madda famille leigui mom do comprendre... gnigua bokal niolay yakk tek la Lou metti, lolou kouko doundoul dou meuneu comprendre ligua neik di doundou instant yi... wayei bo neikei nittou deugg ak nittou principe keine doula beugg... Courage et concentre toi sur ton foyer... Nga fekhei deiff ba say dom douniou am différence seine birr... li brisé famille mom lissi eupp si wadiour yi lay diouguei...

  • @ngonethiam2580

    @ngonethiam2580

    4 жыл бұрын

    Hi my dear how are you I greet you have a nice day give me chance I can chat with you I'm living the knock on you

  • @Laspheredesdistinguees
    @Laspheredesdistinguees6 жыл бұрын

    Tu as raison, mais nakkk li d'où wakhou télé Mada. rawatineu kinguay wakhal nekouffi. dieugelou

  • @marieamar134
    @marieamar1347 жыл бұрын

    courage mada Ba walahi nitou deug nga tu as des principes tu es sincère si kaw si kanam te yalla mousal leu si journalistes yi daniou seytane sokhna khady yalnako yalla yeureum mayko Aldiana Firdawsi si barke Seydina Mouhamed psl. Gagnesiri ken dou tass mbokk alalou yalla leu.

  • @oumarbounethiam9408

    @oumarbounethiam9408

    4 жыл бұрын

    Ju

  • @larosedivine5266
    @larosedivine52669 жыл бұрын

    Sénégal déh bo amé fouleu ak fayda, bo mandoo té réservé gniou taxé la.bone ak fouyi. Mada ba que Dieu te protège. J'aime ta personnalité car c'est proche de la mienne. Et les saytanés de commentaires pourris là quittez là bas.

  • @naboudiop952

    @naboudiop952

    6 жыл бұрын

    elle est vèridique

  • @naboudiop952

    @naboudiop952

    6 жыл бұрын

    doyna waar

  • @malickfall6563
    @malickfall65639 жыл бұрын

    Sokhna Khadi est une pieuse et elle a un sentiment très profond envers les versés coraniques en particulier et en générale le coran. Qu'ALLAH le tout puissant l'accueille dans son Paradis et lui pardonne ses péchés. Amine. Mada BA qu'ALLAH te bénisse . Tu es vraiment une femme battante et toujours respectueuse et digne malgré le monde musical très sensible et complexe. Thioro tu as un paradigme vestimentaire unicité, copie un peu le " TOP 10 " actuel qui te permettra avoir une personnalité accru sur la Chaine TV. Que DIEU nous bénisse.Amine

  • @isabellesenghor7533

    @isabellesenghor7533

    9 жыл бұрын

    Les linge sal sa ce lave en famille

  • @mberygaye4026

    @mberygaye4026

    6 жыл бұрын

    malick fall

  • @alphabazz1
    @alphabazz19 жыл бұрын

    J'ai beaucoup apprécié sa façon de parler Et je ne vois pas de mal à ce qu'elle a dit. En la voyant parler, on sent que elle est véridique à ses propos.

  • @larosedivine5266

    @larosedivine5266

    9 жыл бұрын

    Tu as parfaitement raison, les gens qui la critiquent sont juste hypocrites et saytanés

  • @senegalaise2251

    @senegalaise2251

    6 жыл бұрын

    amadou alpha Ba merci Bro

  • @ousumanejallow5336

    @ousumanejallow5336

    4 жыл бұрын

    Amadou Alpha BA

  • @diarratoure-qg9pj
    @diarratoure-qg9pj Жыл бұрын

    Iow khamone ngani akou sokhna khady mou bakh ma dina la dal li ngay yéss leppou faye kéne khamatoul ni sakh yagui doundou li ngay bone lepp sa rak khana loy défane té basa rak fatou nga wara arété lou doul di weur di yakh déram wayé loko mane di wax mom rawe nala la serigne touba mame cheikh ibra térouna ko thia aldiana yeu gueneu kawei nakh nék nafi ba diougué fi massoul guénei wakh diou niaw si guéminieum lou doul sakho di toudou trou yalla bi souniou yaye fall bou bakho e ba lolo douniou diouk thi dila nianal😭🙏

  • @thiatesow492
    @thiatesow4925 жыл бұрын

    Vraiment tu es sincère maman Daba je t'adore bcp

  • @aidandao8836
    @aidandao88368 жыл бұрын

    elle a trop dit vraiment

  • @boyefall1411
    @boyefall14116 жыл бұрын

    Bilay mada ba borome khol bou raféte ga

  • @bachiirleveridique9767
    @bachiirleveridique97678 жыл бұрын

    EN TOU K DEUGG REK LAFI WAKH LIMAY NAKHARLU MOY WAX GUIMOU WAKH TELE MANOONNA RESTER COMM AVANT. MAIS SERINE BI MAYE RAKKU DIAMBOUR AK DOMU DIAMBUR AU MOINS MOU YEUGUEULKO AY MBOKKAM LOLOU MOY DUEGG GNOUN AY TAALIBE LAGNU MADA BA MII TAALIBELA DAANA DALL SUNU KEUR MAGAL XAMNAA CI DARA SERIGNE TOUBA NAK LIMOU NIOU DIGUEUL MOY TOPPU NDIGEUL SURTOU NDIGUEULOU WAADIOUR

  • @madrame4142

    @madrame4142

    8 жыл бұрын

    salam pour moi j'étais pas la peine vraiment le linge sale se lave en famille.on ne ta jamais entendu sur ses genres trucs en plus ta sœur n'est plus sur ce monde te média defa grave

  • @madrame4142

    @madrame4142

    8 жыл бұрын

    salam pour moi j'étais pas la peine vraiment le linge sale se lave en famille.on ne ta jamais entendu sur ses genres trucs en plus ta sœur n'est plus sur ce monde te média defa grave

  • @bintousarr261
    @bintousarr2617 жыл бұрын

    je t'aime Ma Daba bcoup même.

  • @ngonethiam2580

    @ngonethiam2580

    4 жыл бұрын

    Hi

  • @ngonethiam2580

    @ngonethiam2580

    4 жыл бұрын

    How are you my dear I greet you

  • @aminasylla276
    @aminasylla2769 жыл бұрын

    vrement mada ba jsuis de tt coeu avec toi du courage encore une fois yalla nala yalla leralale lepp ci barki SEYDINA MOUHAMED (PSL) adouna bii so nopiweii rekk gnou beugue takhaw sa boppou...Awa Ba jtei go 1 fois ci mom et chaque fois mom soeurou mada ba lay bakko..mais tkt lii yeupp ayy netalii laye moudjou du courage je t'adoreee

  • @awaba5104

    @awaba5104

    8 жыл бұрын

    c'est ça le Sénégal seytane hypocrisie nafek rek lagnouye courage disent musulman mais gomoudnou dara bon courage domou baye

  • @gueyesophie6034

    @gueyesophie6034

    6 жыл бұрын

    Doy n'a waar mais Mada mounone na dem djalle mogueuno rafet nakhte c est sa sœur ka même

  • @muhammedsamba8755
    @muhammedsamba87556 жыл бұрын

    Masalah MADA BA yalnala yalla defal djam aduna ak djam allahira si barkeh rasulillah yalla mun nako am nako yalna ko yalla deff DEG REK MO MORR

  • @mamecheikhk
    @mamecheikhk9 жыл бұрын

    Ma sœur, ma ngui laye djégalou téy niane, ndakh kheyna sakh ya ma gueune, wayè souma sanione wakh you mélni nga khamni daye khawi soutoura, ndakh téy takhna niou kham louniou waroul wona kham thi sa sœur, ndakh nioune tourou LAHOU bimou dane maggal rék mo niou sokhalone wayé taye khaw nga yakh image bou sokhna khady. LAHOU mo beug soutoura, mo takh mou wathié goudi ak beuthiak, té digualniou djéguelé ak djélalé mouy faté louy takhal dérou nite sirtou sa khète bou wathi liguèy. Nio ngui nianal Sokhna Khady yalla nako tourou LAHOU bimou dane toude Rammou té rafète naniou thi ndiorte. Maha salam

  • @ndeyematymaty3752

    @ndeyematymaty3752

    5 жыл бұрын

    Wiwi.derier.episot

  • @bureautiqueexpert6223
    @bureautiqueexpert62236 жыл бұрын

    Je t'aime bien mada ba ...lingafi yeupa leer je suis avec toi

  • @fatmaba3266
    @fatmaba32666 жыл бұрын

    Mada ba problème de famille kéne douko wakh si télé ndakh journalistes yi séne intérêt rék la gnouy khol

  • @gayefatou9677

    @gayefatou9677

    4 жыл бұрын

    Wsr

  • @sokhnadiarrandiaye6671

    @sokhnadiarrandiaye6671

    3 жыл бұрын

    Sa c'est vrai 👌🙏

  • @beautedafrique709
    @beautedafrique7096 жыл бұрын

    Svp garder vos vies privée...et vs les journalistes ayez un peu de retenue ...

  • @seynaboumamyndiayediallo7526
    @seynaboumamyndiayediallo75269 жыл бұрын

    J'apprécie la franchise de mada ba gagne n'a ka régler ses problèmes de famille

  • @mamadoudiallo6684
    @mamadoudiallo66843 жыл бұрын

    Allah akbar machallah mada ba Sénégal yeppou molaa wahal loubah machallah

  • @annabenjamindiouf369
    @annabenjamindiouf3695 жыл бұрын

    Mada Bâ ya deuggou fan naleuh sah bilahi longue vie á toi jtm

  • @mamadoudiallo6684

    @mamadoudiallo6684

    3 жыл бұрын

    Mada ba machallah

  • @lenaamar9284
    @lenaamar92846 жыл бұрын

    Yalnako yalla yeureum sokhna Khady aduna amoul solo yalna yalla joubole gnep rawatina bokk ben deret Deret dafa fort Man d souma narone nonok sama deret rouss thi sama yay bignou djour

  • @dammmedama7869

    @dammmedama7869

    5 жыл бұрын

    lèna amar bilahi c vrai d franchemet

  • @daviddiop86
    @daviddiop862 жыл бұрын

    Yaw sokhna Khady mola guene fouff billahi yalnako yalla yueram té kharéko Aldiana firdawsi

  • @seydinaniang233
    @seydinaniang2334 жыл бұрын

    da nga digne motakh nga nekh ma

  • @DieynabaNdiaye-ch5ny
    @DieynabaNdiaye-ch5ny9 күн бұрын

    Ndeyssane Sokhna khady on habite ensemble kou bakh ndeyssane teyyyy mada aussi elle est formidable yalla rek mo khammmm

  • @OumouAidara-zi8yg
    @OumouAidara-zi8yg24 күн бұрын

    Mada❤❤❤❤❤❤❤❤ sa yaye sokhna Oumoul Fadly Aidara louga

  • @Bayeasndiayeinternational
    @Bayeasndiayeinternational7 жыл бұрын

    dafa sincere rek senegal nak kouffi sincere do bari kharit ndakh deukkou hypocrites leu

  • @fagay1716

    @fagay1716

    7 жыл бұрын

    Baye As Ndiaye International acrtyuig

  • @fagay1716

    @fagay1716

    7 жыл бұрын

    Baye As Ndiaye International o' ou' m

  • @yadefall136

    @yadefall136

    6 жыл бұрын

    no khamo kou serieux ki day doul bilahi walahi talahi

  • @adamadiop7262

    @adamadiop7262

    6 жыл бұрын

    Baye As Ndiaye In ternational cg

  • @adamadiop7262

    @adamadiop7262

    6 жыл бұрын

    Baye As Ndiaye Intern ational

  • @houmahaniaw1335
    @houmahaniaw13356 жыл бұрын

    Merci beaucoup Mada Bà koubah dobari kharit Mane Nila Méle Si sounie famille Nakh Mouna Wakh dégue Rak

  • @iibrahimadiop4292
    @iibrahimadiop42927 жыл бұрын

    kou dégueu say paroles khamni amoo thiakhane. wakhou deugue nékhna kham. yalla bakhna

  • @mamiissasoumare55

    @mamiissasoumare55

    5 жыл бұрын

    Iibrahima Diop mada ba nio deukone dpui liberté 4 momeu yar mai kéne meussouko dég silou niak fayda nite kou mandou réglé diap niamboureum machalla mbakh rék lako khamé séne keur mome késsé mofa réglé

  • @FatouNdiaye-fq1ro
    @FatouNdiaye-fq1ro16 күн бұрын

    Mas'sa Mada j'ai vécu a peu prés la même chose je te comprends tellement !.

  • @sopendir4275
    @sopendir42756 жыл бұрын

    Très bien dit

  • @diallomassata7722
    @diallomassata772221 күн бұрын

    Bravo mada pure verite nite day gore ame loumouye bagne,deugou

  • @cheikhdiop866
    @cheikhdiop8669 жыл бұрын

    Le linge sale se lave en famille!

  • @fatoumatangom712

    @fatoumatangom712

    9 жыл бұрын

    Cheikh tu as parfaitema raison elle ose parler comme ca a ses propre soeur chiiip

  • @ibrahimasarr6589

    @ibrahimasarr6589

    8 жыл бұрын

    adouna amoule solo lo fi guisse dafaye diekhe

  • @sachafamechon9723

    @sachafamechon9723

    6 жыл бұрын

    cheikh diop

  • @dallathiam2907

    @dallathiam2907

    5 жыл бұрын

    Vraiment

  • @mariamathiare3960

    @mariamathiare3960

    4 жыл бұрын

    Wakh deugu

  • @altaflimbada7346
    @altaflimbada73464 жыл бұрын

    Sénégalais bo deugo bari nonne

  • @mamadoudiallo6684
    @mamadoudiallo66843 жыл бұрын

    Machallah mada ba courage diegene boumeni yow yo boul machallah

  • @aichaguisse9960
    @aichaguisse99605 жыл бұрын

    Mai li dou wakhou fi Famille soutara la ishhhh est ce que yagui étalé sa vie privée fi bonne

  • @toubaglobaltv9880
    @toubaglobaltv9880 Жыл бұрын

    Mada je t'apprécie bien, mais sa c'est une erreur qui as touché beaucoup, après le décès de ta sœur, fallait pas parlé de sa vie sur les réseaux.Té nagua khamni nite kou bakh la

  • @khadygueye2985
    @khadygueye298526 күн бұрын

    Machllaha mada❤❤

  • @famakhathiouba2087
    @famakhathiouba2087 Жыл бұрын

    Je suis comme Mada ba motakh on me taxe de rancunière bilahi je suis pas hypocrite té fii kou deugou bari ay nonn Mane dé nii la mel tu m aime je t aime tu m aime pas je t aime pas non plus et la vie continue

  • @bellawomen
    @bellawomen9 жыл бұрын

    Mada vraima je t'adore tu es honnête mai noor nit day mandou tu dis k dafa tardè tu ne sais rien nit day mandou

  • @madeleine7159
    @madeleine715922 күн бұрын

    Sénégal kou deugou niouni dagua compliqué wala dagua dof, Thione Seck li legn ko done wakhal, bamou guener adouna la nieup kham moy kaan deug! Yalna nou Ya Allah sakhaal ci yonou deug!

  • @modoundiaye4306
    @modoundiaye43065 жыл бұрын

    No man beug na ma daba sa fouleu dall teuye ko

  • @senegalaise2251
    @senegalaise22516 жыл бұрын

    Sama tourando mane ak yaw gno yam djiko.

  • @rabyarabya3780
    @rabyarabya37808 жыл бұрын

    comment peut-on interroger des gens comme ça ????

  • @binetasankhare5135
    @binetasankhare51355 жыл бұрын

    degue rekk nga wax mada ba

  • @bassseye1335
    @bassseye13358 жыл бұрын

    dia diaf mada ba ya gore waye yala doula fatie

  • @adaleitenoorr7283
    @adaleitenoorr72839 жыл бұрын

    Serieusement Mada t'es juste une méchante rancunière. Je t'appréciais beaucoup pour ta correction et ta sincérité, mais c'est clair que sokhor mola takha tardé.

  • @abyndoyediop6652

    @abyndoyediop6652

    6 жыл бұрын

    adaleite noorr mada ba niit kou boone la le linge sale se lave en famille

  • @madamemadame3380

    @madamemadame3380

    5 жыл бұрын

    @Mamadou Fall C'est toi l'idiot du village. Ana liberté d'expression

  • @madamemadame3380

    @madamemadame3380

    5 жыл бұрын

    @@abyndoyediop6652 kou bone waye Simmmm

  • @zenabeomzogueye9248
    @zenabeomzogueye92489 жыл бұрын

    deugue dji yalla rék moka kham mé nak soumaye dégue mada ba mouye wakh dege rék laye guisse si mada ba mé mada gnoune aye fns nagne pour la prochaine foi boul expliké devan la télé tégual lép si lokhoye sougnouye borom nakh famille lou sacré la on vou adore mada bonne continu ation

  • @amaryallanayallafayeegaye7398

    @amaryallanayallafayeegaye7398

    6 жыл бұрын

    madaaaba mangui lay beugue saa soune

  • @nanafall4134
    @nanafall413411 күн бұрын

    Peut être c’était pas naturel 😢 paix à son âme dedelé mane nassi xam 😢

  • @saratazouloudiouf1378
    @saratazouloudiouf1378 Жыл бұрын

    Mane zoulou souma saguané ba seytané féweulémeu ak sama propre sœur...bisbou guéné adouna warouma am dara loumay wakh si mome...comme que bamouy doundou amoumawone ak mome wakh. Et gnoune gneupay dem kén doufi dess

  • @papadiop2642
    @papadiop26424 жыл бұрын

    véritable pur ka wakhe

  • @bayembackeseck4243
    @bayembackeseck42437 жыл бұрын

    Ki dou bax Nitt sou Fatou daguay Wax Lou rafet sii mome

  • @madiordiop1245

    @madiordiop1245

    4 жыл бұрын

    Baye Mbacké Seck

  • @madaba5571

    @madaba5571

    3 жыл бұрын

    Yaw. do. Yalla. So. bone. Yalla. Soxoroul. te. degue la. begue

  • @moustafaniang225

    @moustafaniang225

    3 жыл бұрын

    @@madaba5571 envoye ma numero mada ngir yalla

  • @camarakaty6960
    @camarakaty69607 жыл бұрын

    walfadjri nio geuneu seytané

  • @bayoumbene2875
    @bayoumbene28757 жыл бұрын

    Mes nak yaw ma daba do nite nagua khôl sa bop Bou bakh Sokhna Khady mon la guene fouf dagua sokhor khana nak Kou de dousa Rak naka ti nit dinala sokhoré basa banmel yaw sokhna Khady molay khetali thi sa bamel

  • @madamedieng3099
    @madamedieng30995 жыл бұрын

    Kep kou la commentair lou bakh hypocrite leu... ya wow khole. Fi la beut yam.. do meusa avancer thi musik

  • @madaba5571

    @madaba5571

    3 жыл бұрын

    Yaw. momou. Ta. Yes

  • @mamadoundiaye3425

    @mamadoundiaye3425

    3 жыл бұрын

    Yow ya meneu doule

  • @assballagaye2348

    @assballagaye2348

    2 жыл бұрын

    @@madaba5571 ndéysann nite kou bax nga mé déréte da for nite kouné amo loudoul sa mbok

  • @mariemediop4680
    @mariemediop46809 жыл бұрын

    mada ba vraiment doo nite yow wéroo dof bou sokhor ngua roussnaa trop si kaddu you bone yiii amoo béne droit di wakh say probleme famille si médias yi le linge sale se lave en famille j'ai vraiment honte de toi sa rak dji nak di sokhna Khady moungua si aldiana you kaké serigne touba dinako térou silou bakh la nékone ba guén adouna yow nak khessal ak musique singua nék Yalla dinalen até

  • @madaba5571

    @madaba5571

    3 жыл бұрын

    ma. gêne. nithe Sa xet

  • @moustafaniang225

    @moustafaniang225

    3 жыл бұрын

    @@madaba5571 dieuleul sama numero 34641158747

  • @Toursdumonde.

    @Toursdumonde.

    2 күн бұрын

    ​@@madaba5571Alhamndoulil Lah. Yalneu Yallah sammeu leu Mada Ba.❤ Defal leu soutoureu sammeu seu ay sopé.❤ Yalneu Yallah léral sougnou xeel bagnou xammé bou bakh sougnou ay ennemis teu ils seront jetés dans l'enfer.

  • @ndeyefatoufall4009
    @ndeyefatoufall40097 жыл бұрын

    virement même boudé deugu sakh waroko wakh yaww sa rakk yii gay yakkk séné derrr ba baye kara dila dioubolé mada soutoura dioum gueu dall on dirai keu daga mbandii kw

  • @omarcissebichriomarcissebi5679
    @omarcissebichriomarcissebi56794 жыл бұрын

    Machalla

  • @moisek147
    @moisek1479 жыл бұрын

    Wolof ndiaye nena koudeh si marché ya targue sa bop mada Ba yaow deh li dou sa thieure te kouye dague sa palakh ,boule dieule paka bou gniaw sokhna khady sa rak nak kou amonen soutourala yalla na khippe Aldjina sa bop gaye were

  • @khadimediouf8998
    @khadimediouf89986 жыл бұрын

    Ta soeur est morte et tu n y vas pas parceque tu ne t entends pas bien avec son mari n est pas une excuse mais mada reste un exemple comme sa soeur ,on ne les a jamais entendu dans certaines betises.

  • @neneba5469
    @neneba54694 жыл бұрын

    Les mains sallent se lave en famille mais pas ici

  • @dammmedama7869
    @dammmedama78695 жыл бұрын

    wa gui mome nite la

  • @papalaitybasse7717
    @papalaitybasse77176 жыл бұрын

    Tu est vraiment juste et sincère

  • @zryhjkbcheikh9177
    @zryhjkbcheikh91775 жыл бұрын

    sa rak waro ko wilipandai nak wero dh c prive

  • @modoudiakhate6820
    @modoudiakhate68204 жыл бұрын

    Sokhna khadi mola guene

  • @sokhnadiarrandiaye6671

    @sokhnadiarrandiaye6671

    3 жыл бұрын

    Ndaysane thiayy yalla

  • @dammmedama7869
    @dammmedama78695 жыл бұрын

    no dofe bou sokhor bakhoule

  • @souleymanembodj7129
    @souleymanembodj71293 жыл бұрын

    Amal sa vie privé mada

  • @sadiofall1213
    @sadiofall12134 жыл бұрын

    So nèkè nitou deuk gnou wakhni dagua beuri problèmes mè problèmes mou famille diambour yonou kèn nèkou thji mada wakhou deugeu rèk lafi dègeu

  • @ndeyesaliou389

    @ndeyesaliou389

    3 жыл бұрын

    Wa legui loumthi wakh Si tele Li toubap yi rek mooy def Li sa rak Ganou Nga yak deram

  • @tamraanidag2293
    @tamraanidag22936 жыл бұрын

    Merci madame ba

  • @mamadoulamineloumloum5141
    @mamadoulamineloumloum514121 күн бұрын

    Niit kou deugou të dioub❤

  • @khadimsarr3141
    @khadimsarr31419 жыл бұрын

    Mane dee mada ba comprane nala thi sa degou wayee djoum nga lol ndakh lou way diotek nit ba mou dedou aduna nga meunko diale dji rawatina sa rak surtt naniu moytou di werante ndakh eulenga takh le pire nak moy khawma mo def am defoul wayee yalla rebena kouy dogouk mbok... yalna yalla tapee xolyi amine

  • @mberygaye4026

    @mberygaye4026

    6 жыл бұрын

    KHADIM SARR n

  • @berebuxamxam1383

    @berebuxamxam1383

    6 жыл бұрын

    KHADIM SARR elle a bien fait de expliquer la autres qui voulait en profiter pour ... Mada à tellement fait de bien pour ses sœurs

  • @Toursdumonde.

    @Toursdumonde.

    2 күн бұрын

    Elle a bien fait d'expliquer.

  • @musamar1945
    @musamar19457 жыл бұрын

    bon rek la

  • @mamecheikhsylla6367
    @mamecheikhsylla636726 күн бұрын

    Fene rek

  • @houmahaniaw1335
    @houmahaniaw13356 жыл бұрын

    kouguene bone Si famille Noye Yak dére

  • @bebobebo9274
    @bebobebo92748 жыл бұрын

    Ta le droit de dire se ke tu veux au Sénégal ya trop de langue de bois

  • @jerysow1717
    @jerysow17174 жыл бұрын

    Diadieuf mada

  • @MameAli-tb4rv
    @MameAli-tb4rv11 ай бұрын

    Courage Mada

  • @soukeyefall8139
    @soukeyefall81398 жыл бұрын

    Affair bi walou téne la kou gneuw si pindeu bi ngay yem

  • @Max-maguette5fall
    @Max-maguette5fall6 ай бұрын

    Ndeye san du courage legui file Sénégal tollou wakh ton tou rek kolako deff nga deff kokou

  • @thiofmbaye7503
    @thiofmbaye75034 жыл бұрын

    Dafa degou rekk leral bakhna adouna Dafa gouda tanka

  • @adjimbacke5664
    @adjimbacke56648 жыл бұрын

    Wa doko soutoural sakh dé mom gnaw na di do wakh guen adina sakh ak loumana am sa mbokoum dioulite la di sa mbokoum talibé ta am na yokham ni probléme mou famille la dou wakhou télé kenn khamoul khamoul yane genrou dioulite ngen rek waya nalen lerné kou doul soutoural sa mbokoum dioulite yala doula soutoural Waya MANE KHAMILA SAALIKHANE FALI NAFSIHII sadaha lahoul haziim

  • @bromprokhanebousso6315
    @bromprokhanebousso63155 жыл бұрын

    Wakh dji rafetoll 😅😅

  • @abdoulhane420
    @abdoulhane4209 жыл бұрын

    en tout cas khawmaa deugouna ou pas mai ce ke peut dire moye yoroul kholou dioulite .parceque lou tole ni sa rap géne adouna nieuwofa

  • @boromlibaakh8837
    @boromlibaakh88378 жыл бұрын

    kiii domi kharame piir la limoo tay do siiw si adouna sa rak gay wakhh lii si telebi ya bone ya dib khadj motakh kene beugoula yague ga waye te kene doula dieul tekiwo dará

  • @famasene8642
    @famasene864228 күн бұрын

    Kou bonnne nga khady mo guennne fouffff

  • @nenediaw940
    @nenediaw9405 жыл бұрын

    Ey way way way li loumou done ni ay Mada Ba ya bone ya yéss yow do gat ya rancunière ya sokhor ngay bigna ka bagn.gnikoy encouragé keen guenouléne done ay hypocrite nakh boudone yeen dounguéne ko deff sen mbokk yow yangui dora wakh loutakh meno siiw li niawna torop mm boudé lingay wakh deug leu(xawmathi dara) warofi né di wakh kw k se soit té ki dem na.Repoz en paix Sokhna Khady yalenala Yallah yeureum

  • @daoudatambedou

    @daoudatambedou

    4 жыл бұрын

    Kikay mo yéss yaw domaram dji sokhna meussta wakh si yaw louniaw mola gueune dé

  • @sokhnadiarrandiaye6671

    @sokhnadiarrandiaye6671

    3 жыл бұрын

    @@daoudatambedou bilayy kenn masoukodegg repose en paix nitt bou dedoo sedell ko lou rafett

  • @omarcisse991
    @omarcisse9914 жыл бұрын

    Mada dioum nga

  • @boudechou
    @boudechou8 жыл бұрын

    NOOOOO JE SUIS choquée!!!!

Келесі