LES REVELATION EXPLOSIVE DE MAME MOR MABYE SUR LE VISITE DU PRESIDENT A TOUBA..ETAT MASOUL...

SOLUTION TV

Пікірлер: 327

  • @user-gm1cg6it6o
    @user-gm1cg6it6oАй бұрын

    Serigne touba kouy wakh si mome loo ame si mome diommoula ❤Dieureudieuf s mame mor

  • @malickkane5858
    @malickkane585824 күн бұрын

    Machallah saringe mame mor sama xoll sedena loll ci yaw yallna yalla fayla ci barki borom touba khassida yi

  • @seynaboudiack7692
    @seynaboudiack7692Ай бұрын

    Merci beaucoup serigne Touba ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶

  • @KhadyTall-kj9uv
    @KhadyTall-kj9uvАй бұрын

    Dieuredieuf Serigne Touba amoul morome Kouco bagne damala yereume yalla mococo def

  • @cheikhdiop4944
    @cheikhdiop4944Ай бұрын

    Barcki seringe touba ki amoul kham kham nitou aitré la 😢 diomay yalla na yalla oyofal yéne bi

  • @user-id9jr2ou7f
    @user-id9jr2ou7fАй бұрын

    Salam salam mame more duundal weural masha allah jeureujeufeuty Serigne Touba

  • @seynaboudiack7692
    @seynaboudiack7692Ай бұрын

    Machalla Anna solo serigne Touba 🕋 🕋 🕋 🕋 🕋 🕋 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Toubaexellent
    @ToubaexellentАй бұрын

    Yawe dieuwrine Daga baakh di wakh réeek..wakhtaané Serigne Touba Bobou niouy wakh di minimisé Barki alkhour'aan la wakh mo geu'n Si métier yi nék Si adouna bi yeup kou d'accord lalal j'aime 👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿 Gni néketé xamoun dara toook mouy dokh la xamoul moye lane SËRÏGÑ TOUBA kouka nékal bén mou nékal la foukou .. MAME Mor Mbaye bénén yoon wakhal ni nékk Si kéepar SERIGNE BI mo dakheu Lo Guiss ndakh sa alaakhira moye dokh..Niom tok Mouy dokh bouni wakh Si adouna la yém.. SËRÏGÑ TOUBA nak day défar sa adouna Bamou Diak Soga défar sa alaakhira..kép kou wakhoul DIEUREUDIEUFEUTI SERIGNE TOUBA,YALLA bousa affaire dokh adouna ak alaakhira

  • @maryamdieng8295
    @maryamdieng8295Ай бұрын

    Tay mom Serigne Mame Mor wakhna wakh djou dioup mashaa Allah!!

  • @seynaboudiack7692
    @seynaboudiack7692Ай бұрын

    Merci beaucoup serigne Touba ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️

  • @ndeyefatougueye258

    @ndeyefatougueye258

    Ай бұрын

    Tout à fait Mame Mor était le Talibe de Serigne Cheikh khadim Falli

  • @MborThioub-xd3vn
    @MborThioub-xd3vnАй бұрын

    Dieureudieifeti s touba

  • @user-be6bn3dn6z
    @user-be6bn3dn6zАй бұрын

    Thank you SA Ndiogou very nice 👍🏿🙏

  • @yacinesene219
    @yacinesene219Ай бұрын

    Dieureudieufeuty Serigne Touba ❤

  • @mouhamoudoulmoustaphadouco1457
    @mouhamoudoulmoustaphadouco1457Ай бұрын

    Pour une fois je suis d'accord avec Mame Mor Mbaye. Pour ce rappel historique !

  • @fallougning865
    @fallougning865Ай бұрын

    Mame mor mbaye kounou wara encourager la ndax bo xollê dembam ak tay ga wara xamnè diambar deug la kou andak serigne touba tey deugeul kèn meunoul si iao dra jam rek gay am walahiii❤

  • @sportmaisonpourtoustv

    @sportmaisonpourtoustv

    Ай бұрын

    😂

  • @souleymanekane8390
    @souleymanekane83907 күн бұрын

    Serigne touba rekk mom kesse leep féep Dieureudieuf mame cheikh ibra fall

  • @leveridique3001
    @leveridique3001Ай бұрын

    KOU MOOME KHAR MI NGA BAYI BOUUM GUI

  • @mariamagaye472

    @mariamagaye472

    Ай бұрын

    Merci iow

  • @zgrsljrbkbtfg1135
    @zgrsljrbkbtfg1135Ай бұрын

    Mbame Mor Mbaye seytané bou mak , fene rek lay def😮

  • @pendadieme2235
    @pendadieme2235Ай бұрын

    Merci sa bien dît

  • @user-ur3dj6ct6s
    @user-ur3dj6ct6s29 күн бұрын

    Serigne ToubA amoul morome Alhamdoulila

  • @yacinesene219
    @yacinesene219Ай бұрын

    Machallah Se Mame Mor Mbaye deug bou wer❤❤❤

  • @fallousylla2510
    @fallousylla2510Ай бұрын

    Machallah mame mor Mbaye

  • @fatoucissokho7722
    @fatoucissokho7722Ай бұрын

    Tog mouy dokh gniko mome khamnagne séne bop . Moy gni nga khamné dagnouye féyékou wére té dougnou kheuye

  • @P4t5R
    @P4t5RАй бұрын

    Les gars lou aye di jambat! On doit dépasser ce débat de bas niveau wallah 👊🏾

  • @dioufmodou4234
    @dioufmodou4234Ай бұрын

    Yahwou topall feule mor mbaye Yahwou doo dara

  • @oumarseck3114
    @oumarseck3114Ай бұрын

    DELEN WAKH DIEUREUDIEUFE YALLAH SOUNIOU BOROM,SERIGNE TOUBA LOLOU LAFI DIANGALEWON SOXLAWOUL KOUKOY SANT PIIFFF..

  • @bambacisse4200
    @bambacisse4200Ай бұрын

    Mor Mbaye kou deug ndéyame la. mom mi moy système bi

  • @bayebeye3070
    @bayebeye3070Ай бұрын

    Mame Mor amoul xam xam wayé limouy wakh si Serigne bi nèkh na daal

  • @ronebodjis4607

    @ronebodjis4607

    Ай бұрын

    Meuna séduire kou nek lamigne bii nekh na

  • @maguettebouboufaye2993
    @maguettebouboufaye2993Ай бұрын

    DARAY KHAM KHAM AMOKO NDOUGOUROU REEK

  • @khadimfaye2613
    @khadimfaye2613Ай бұрын

    Waw gore mame more Mbaye

  • @YacineDiouf-up7gf
    @YacineDiouf-up7gf28 күн бұрын

    Dieureudieuf borom touba ya dimbeuli diam❤❤❤❤

  • @makharyndiaye5922
    @makharyndiaye5922Ай бұрын

    Merci Mame Mor

  • @KhadyTall-kj9uv
    @KhadyTall-kj9uvАй бұрын

    Dieuredieuf mame more

  • @lieutenantcolonel2186
    @lieutenantcolonel2186Ай бұрын

    Niite gni mëllni vraiment Deuk bi sokhlawpulén en ce moment

  • @sitapha-kb4vv
    @sitapha-kb4vvАй бұрын

    Antoine diome à donné à serigne bassirou mbacke porte parole des mouride 50 millions dans une scac

  • @salioudrame992

    @salioudrame992

    Ай бұрын

    Absolument

  • @FallourafahihtDiaw-po4rl

    @FallourafahihtDiaw-po4rl

    Ай бұрын

    Pour commerçants yie céne marché bi lakon la dou pour mome

  • @khadimdiop6988
    @khadimdiop698818 күн бұрын

    Dieureudieuf Serigne Touba❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ☝

  • @moustaphadiagne4278
    @moustaphadiagne427813 күн бұрын

    Magui ziar gneup suis desolé mame mor meme les mourites bayiwouna xel sa wakh yen beug xaliss motakh guay wakh

  • @AntaDiouf-wo2kl
    @AntaDiouf-wo2klАй бұрын

    Machallah Mame Mor Mbaye 😘❤️❣️

  • @user-ye3gr5xr4j
    @user-ye3gr5xr4jАй бұрын

    Dieuredieuf Mame mor mbaye kou beug serigne touba la ❤❤❤❤

  • @leveridique3001
    @leveridique3001Ай бұрын

    TAY MAME MOR MBAAYE SONENA KHAMATOUL FOUM DIEUM

  • @AlioubadaraColy-js8im
    @AlioubadaraColy-js8imАй бұрын

    Il me fait rire ce gars😂😂😂

  • @AdioumaKebe
    @AdioumaKebeАй бұрын

    Merci mamor

  • @khadimdiop6988
    @khadimdiop698818 күн бұрын

    Dieureudieuf Serigne Touba❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall2003Ай бұрын

    Esprit simple africain

  • @omardiouf4410
    @omardiouf4410Ай бұрын

    Vraiment domerame bou melni il ne faut plus l invite amoul bene vision

  • @samsfallou245

    @samsfallou245

    26 күн бұрын

    Ioe sa data yaye

  • @omardiouf4410

    @omardiouf4410

    26 күн бұрын

    @@samsfallou245 guisla rek motakh ma nane sa regalou ndeye domerame

  • @omardiouf4410

    @omardiouf4410

    25 күн бұрын

    @@samsfallou245 dina teupp leumbeul sa digou leufeul ndeye

  • @omardiouf4410

    @omardiouf4410

    5 күн бұрын

    @@samsfallou245 dina kate sa ndeye ba pikine icotaf domou khathe thioto ya pake

  • @nogayediop8182
    @nogayediop8182Ай бұрын

    Merci oumar

  • @momocreation3631
    @momocreation3631Ай бұрын

    Mamor mbaye politiciens nga domouharam ☹️☹️

  • @Adnanezinho-jm8zk
    @Adnanezinho-jm8zkАй бұрын

    Merci beaucoup senegal gni khamoul ba nopi sokhor mofi ame

  • @laminediatta7069
    @laminediatta7069Ай бұрын

    Niounnnnn amouniou loudoul yalla ak yone iii souniou wadiourrr wreck point

  • @daoudandiaye5588

    @daoudandiaye5588

    Ай бұрын

    lolou sa affaire la

  • @Weuzelejumeau2387

    @Weuzelejumeau2387

    Ай бұрын

    Da ngay doul nioune YALA Yonént bi Ak Serigne Touba lagn am

  • @abdoulahatendiaye7020

    @abdoulahatendiaye7020

    Ай бұрын

    man serigne touba la am de

  • @ronebodjis4607

    @ronebodjis4607

    Ай бұрын

    ​@@abdoulahatendiaye7020lolou aussi sa affaire point 😂😂😂

  • @abdoulahatendiaye7020

    @abdoulahatendiaye7020

    Ай бұрын

    @@ronebodjis4607 mo takh ma neke sy

  • @seexxunaadaraame6809
    @seexxunaadaraame6809Ай бұрын

    Toog muy dox mooy waa APR pan yoon murit . Yoonu murit liggéey jaamu Yàlla rekk. La ñu xam.

  • @maguettehane2424
    @maguettehane2424Ай бұрын

    Wakhtan si Serigne touba khool yi di seed rek liguey la

  • @ahmadoubambadieng8720
    @ahmadoubambadieng8720Ай бұрын

    Iow Yonnou mouride bi mou defaroo duu tayy Ahmadou yonnu L’Islam la défaar ❤

  • @Diatou2410
    @Diatou2410Ай бұрын

    Dieureurf serigne touba

  • @AbdouDiopfall
    @AbdouDiopfallАй бұрын

    ❤Touba rék acassa😂

  • @morsene9081
    @morsene9081Ай бұрын

    Merci sa

  • @onestensemble8497
    @onestensemble8497Ай бұрын

    Boul niou sonal demal ligueyi gueuno fi nek kene mouride da ngay mboubo serigne bi rekk

  • @user-jl5ee4yh1z
    @user-jl5ee4yh1z11 күн бұрын

    ❤❤❤

  • @user-ur3dj6ct6s
    @user-ur3dj6ct6s29 күн бұрын

    Dieureudieuf serigne mame mor

  • @alesylla2991
    @alesylla2991Ай бұрын

    Mame mor Abe mouride d'où Bari wakh .liguey Lou Bari néwi wakhe

  • @MameboussoDiakhate-nt9zm
    @MameboussoDiakhate-nt9zmАй бұрын

    Merci mbaye

  • @Dia.ibrahim
    @Dia.ibrahimАй бұрын

    Soufi wakhé Lou moi Waroul wakh nioutekk ko plaçâmes.

  • @djibrildiaw3262
    @djibrildiaw3262Ай бұрын

    Mam mor aka mana feenn....

  • @saikoudiallo9848
    @saikoudiallo9848Ай бұрын

    MERCI MAME MOR LONGUE VIE ET BONNE SANTÉ À TOI

  • @HabibouNiang-is7bd
    @HabibouNiang-is7bdАй бұрын

    Vraiment sonneu nanou si façon yi

  • @ahmadoundiaye6176
    @ahmadoundiaye6176Ай бұрын

    Mame mor tok mouy doh kén bolewouthi serigne yi waro tontou nilagnouy déf dagnouy déplacer debat bi

  • @cheikhounafall2957
    @cheikhounafall2957Ай бұрын

    😂😂mes saa sonalna mame more mbaye cheeuut

  • @abdoudiarra2979
    @abdoudiarra2979Ай бұрын

    Ki mo dakh féne Senegal raya yeup la dieul

  • @bambabroderie979
    @bambabroderie979Ай бұрын

    Diareudiafé serigne touba ❤

  • @falloudiop9996
    @falloudiop9996Ай бұрын

    Merci mame Mor mbaaye

  • @cheickmoinga3245
    @cheickmoinga3245Ай бұрын

    Waax jaar-jaaru jaambur du Xam-xam

  • @KhadyTall-kj9uv

    @KhadyTall-kj9uv

    Ай бұрын

    Mamou diabour bou defe Louisa Mame defou dika wax iniane bahoul daye lak hold dieuredieuf Serigne Touba

  • @codeurloeil

    @codeurloeil

    Ай бұрын

    Ku baax Alquran sax day wax jaar jaaru jaambur suñ ecole yangi nii ñufay jang histoire yu tubaab yi 😅😅😅

  • @cheickmoinga3245

    @cheickmoinga3245

    Ай бұрын

    @@codeurloeil Boo xaamé yàllà dëgg té raaññé koo dii nga xaamni ioe yaay Al-hur-aan ? TawhiiRekkaWóor ☝🏽 😂😂😂

  • @cheickmoinga3245

    @cheickmoinga3245

    Ай бұрын

    @@KhadyTall-kj9uv Serign Touba du folklore waayé dunndu laa, féxé topp L'islam, topp Saariah, topp Sunnah keep

  • @codeurloeil

    @codeurloeil

    Ай бұрын

    @@cheickmoinga3245 Bismillah laaj ma si tawhiid man tazawwudu sikhaar laako jaangé 😂

  • @mouhamadoulo3573
    @mouhamadoulo3573Ай бұрын

    Loutakh Senegal Bo diouboul rek ngay utilisè terme “”Senegal dafa nakharè wakhè”” boulene Niou sonal way ish

  • @falloudiba3720
    @falloudiba3720Ай бұрын

    Mame Moor duul demal ligéyi ganoo Gám Sëriñ bi kénn

  • @khadimdiop6988
    @khadimdiop698818 күн бұрын

    Machallah❤❤❤❤

  • @user-sz3gu3zl5f
    @user-sz3gu3zl5fАй бұрын

    Content de vous NDAX SERIGNE TOUBA

  • @bayefall3628
    @bayefall3628Ай бұрын

    Dierediefeti serigne touba

  • @BambaKhadim-pg7hm
    @BambaKhadim-pg7hm11 күн бұрын

    Merci ❤

  • @bayesall4452
    @bayesall4452Ай бұрын

    Sa dou nit😂😂

  • @boypikine5856
    @boypikine5856Ай бұрын

    TOKK MOUYY DOKH "DIÈKHNA DÉE"

  • @user-xi3pw1rs3n
    @user-xi3pw1rs3nАй бұрын

    Vraiment ils ont ignoré la voie de mouride.certains sont jaloux sur leur existance mais il vont mourir tts et laiss la voie de mouride jus k a eternité

  • @user-sz3gu3zl5f
    @user-sz3gu3zl5fАй бұрын

    Diereudieuf Serigne Touba

  • @user-cw6vp5pq2l
    @user-cw6vp5pq2lАй бұрын

    Sénégal ay wakh késsé défarou liguééy rék mokoy défare Péresidant bassirou diomay fay yalnala yallaàrre kiimom wakh rék laydéf took mouy dokhbi dafayatoudé

  • @thionganeousmane7117
    @thionganeousmane7117Ай бұрын

    MACHALLA MAMOR ❤❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine75813 күн бұрын

    Copain Assane Diouf gua légui 🤣🙏🏿

  • @AbdoulahadWademouratn-qn9nv
    @AbdoulahadWademouratn-qn9nv16 күн бұрын

    Machall machall machall

  • @user-hg9rf4er6b
    @user-hg9rf4er6bАй бұрын

    Man Touba la Dekker Mes day doundè Serigne bi Mès doundaloul Serigne bi Day doul rèk

  • @ablaysall1672
    @ablaysall1672Ай бұрын

    Dangaye dull geumo darra

  • @maimounandaw6329
    @maimounandaw632912 күн бұрын

    Franchement deugueuleu teranga mom tji mouride la fek bahh... mouride mom dieuf rkk lagne Ham..liguey baparé def tji yone wi barki borom Touba... gnoune mouride meussougnou harr dra tji état nak

  • @CheikhYade-hg4el
    @CheikhYade-hg4elАй бұрын

    Non gni togougne Moy box lignou tog Moy dokh

  • @Diatou2410
    @Diatou2410Ай бұрын

    Dieureurf serigne saliou

  • @user-hy6qm9fh4c
    @user-hy6qm9fh4c17 күн бұрын

    Bayiléne doule aye doumirhame guéne rk

  • @cherifaidara4138
    @cherifaidara4138Ай бұрын

    Salam mboki patriotes yi mame mor mbaye mi daye liguéye sa Touba TV niou diko Faye salaire chaque mois am ay toole di élevè ay ladoume di diaye di wahtane si kou tédeki Lou am solo kone warouniouko khass badiko saga wassalam 🙏🙏

  • @aminambaye5597
    @aminambaye5597Ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤ Amina mbaye

  • @user-ps5sj4ko2f
    @user-ps5sj4ko2fАй бұрын

    Dokh mouye dokh ndiekhna

  • @fatime-xo8nz
    @fatime-xo8nzАй бұрын

    Back Serigne Touba ❤❤❤

  • @mouhamedsall5594
    @mouhamedsall5594Ай бұрын

    J ai une question pour sadiogou vs pouvez donner la liste des personnes qui ont des salaires sans boulot

  • @sambadalythiam
    @sambadalythiamАй бұрын

    Merci k même

  • @amykasse6320
    @amykasse6320Ай бұрын

    Jajeufeuti serign mam mor

  • @cheikhndiaye4199
    @cheikhndiaye4199Ай бұрын

    Môme mor boule nenfékh barina gayouye fayékou wére té kheuyougnou féne dafa barri

  • @papesamb8624
    @papesamb8624Ай бұрын

    nou sà d'où nitt😊

  • @maryamdieng8295
    @maryamdieng8295Ай бұрын

    Bouroukhlou!!!!😂😂😂😂

Келесі