Koromack Faye saltigué : "dëmm ame na, kuko gëmul ci dëmm yi nga bokk..."

Le célèbre saltigué Koromack Faye a accepté de nous dévoiler quelques uns de ses petits secrets pour se protéger des attaques mystiques qui peuvent être mortelles.
#koromackfaye #saltigue #sénégal
--------------------------------
🔔 Pour plus de contenus choc, abonnez-vous à la chaîne KZread de Pulse Sénégal et activez la cloche de notifications : bit.ly/3e27yQh
---------------------------------
👉 Suivez-nous sur les réseaux sociaux :
Instagram : bit.ly/3qRTTnt
Facebook : bit.ly/3PvRTeV
Twitter : bit.ly/3JyJq6Z
Tik Tok : bit.ly/42YaLWX
----------------------------------
🌐 Visitez notre site Web : bit.ly/44gCEKV

Пікірлер: 140

  • @coumbademe8979
    @coumbademe89799 ай бұрын

    Deum lou am la , dè def emission you mèle pour nit yi kham . Merçi beaucoup

  • @nabyserignefallou1035
    @nabyserignefallou10359 ай бұрын

    Mashalla papà koromack yalla maynako amna kham kham bouma wer day guisse sakhe sou nitt ki warè dè manam fattou

  • @modouthiam8210
    @modouthiam821010 ай бұрын

    Kou xamoul Lou Bari mandoul ay sérér laniou ki limouye wax Lou wér leuh kouko wédi dala diapoul

  • @mbathioundiaye1299

    @mbathioundiaye1299

    9 ай бұрын

    Bilayyy walay Sérère dou ayyyy thiakhane

  • @HerveBasse-in1lv
    @HerveBasse-in1lv10 ай бұрын

    Kou kham dara rek moy meuna comprendr lou koromack di dafa simple lolou rek moma nèeh si mom

  • @Dieng-vk6if
    @Dieng-vk6if10 ай бұрын

    Pure vérité lay wakhni

  • @FatouThiam-wu7yu
    @FatouThiam-wu7yu Жыл бұрын

    Kilifa bi bilahi nimako beugè nakh degou digne Machalla pape yalla na yalla gou dal say fane

  • @amyndiaye6644

    @amyndiaye6644

    2 ай бұрын

    Amine

  • @elhadjigaye4478
    @elhadjigaye447810 ай бұрын

    Machalla il est trop fort

  • @fatoumback
    @fatoumback9 ай бұрын

    Machalla yague fi lole té amé wére faye

  • @dianablackqueen3510
    @dianablackqueen35109 ай бұрын

    ❤ Mach'Allah goudal fane papa beugenala lole waye, YALLAH SBHWTL same gnou

  • @MameboubaDiop-bg7sx
    @MameboubaDiop-bg7sx10 ай бұрын

    Bilaye yadeugou papa kromake yalna sa saye yokou bilakhi ❤❤❤❤❤❤

  • @dieastoufaye5116
    @dieastoufaye51166 ай бұрын

    Kén doiko guiss si ay thiakhane. Faye biram yallana la yalla samm. Bakh, social, ouvert masha allah

  • @faysall129
    @faysall1298 ай бұрын

    Koromak yalnalla yalla arr

  • @GastonCamara-ng9rv
    @GastonCamara-ng9rv9 ай бұрын

    Que dieu nous protège

  • @mariediatta4060
    @mariediatta40609 ай бұрын

    Deum amna c'est la vérité

  • @user-cq8eh4pz1i
    @user-cq8eh4pz1i2 ай бұрын

    Il à parfaitement raison

  • @blackp7381
    @blackp73816 күн бұрын

    Koromack dou touss

  • @yacinndour1787
    @yacinndour17874 ай бұрын

    Machalla ❤❤❤❤

  • @mbendiskone
    @mbendiskone3 ай бұрын

    Dimbali léne ma pour ma guiss ko té yalla tax sonna😭🙏🕋

  • @yamarsy
    @yamarsy11 ай бұрын

    Salam guir yalla numerom la sokhla

  • @Coriolanusshap22

    @Coriolanusshap22

    7 күн бұрын

    Taxi bo dou ladj dibiterie koromack mou yobou lafa apres 18h

  • @doffdouweer3686
    @doffdouweer368610 ай бұрын

    Koromack Faye borom Gouy samb

  • @oumarsylla5209
    @oumarsylla52097 ай бұрын

    Deumb am na. Kouko weddi dang ko done mba deumb dalaa meusta diap 😉

  • @mamoudouthiam250

    @mamoudouthiam250

    4 ай бұрын

    Coumay dimbali numerom té yalla tax

  • @user-kl5up9jl6o
    @user-kl5up9jl6o2 ай бұрын

    ❤❤❤ yalnagñu Yalla árr😢

  • @Toufa-uh1ee
    @Toufa-uh1ee9 ай бұрын

    Vérité absolue

  • @toulayeceesay2213
    @toulayeceesay22139 ай бұрын

    Je confirme on avait des voisins qui avaient une bonne (mbidane) walahi du jamais vu mbidane bi dafa kheuy liguey ci chez nos voisins quelques heures plus tard un membre de sa famille est venu la récupérer le lendemain la famille annonce à nos voisins que la bonne était morte nos voisins ce sont rendus à son deuil ils apprennent par surprise que dagnouko fayé bor c'était choquant

  • @adjacoumbafall

    @adjacoumbafall

    9 ай бұрын

    fayé bor manam?

  • @toulayeceesay2213

    @toulayeceesay2213

    9 ай бұрын

    @@adjacoumbafall voilà on était tous sous le choc walahi Lou ken meussoul guiss en tous cas c'est dans leur jargon

  • @misstchiptchip2963

    @misstchiptchip2963

    8 ай бұрын

    @@toulayeceesay2213 les sereres ont leur réalité... fayer bor sa existe dans plusieurs pays de la sous région mais au Sénégal dans des villages reculé ils se passent des choses

  • @Queenprincesse1

    @Queenprincesse1

    8 ай бұрын

    Vérité absolue

  • @whythenumber21everywhere6

    @whythenumber21everywhere6

    8 ай бұрын

    Lolou yépp mbirou Iblis leu. Yéna key méy dolé motakh mou bayilén nguén gueum ni YALLAH amna ba nopi gueum lénén...ci bokalé rék nguén di wéy ba heuy yéwu diakarlo ak safara

  • @HousseynKadi
    @HousseynKadi5 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤

  • @oumoucisse8602
    @oumoucisse86028 ай бұрын

    Aka bakh nidiaye yalna yalla yagal sa takhaway

  • @DibiterieSeck-ky8tn

    @DibiterieSeck-ky8tn

    6 ай бұрын

    Dakha am numérom

  • @oumoucisse8602

    @oumoucisse8602

    6 ай бұрын

    @@DibiterieSeck-ky8tn waw amnako

  • @YamarSy-it1uj

    @YamarSy-it1uj

    4 ай бұрын

    Salut ma soeur numero koromak la sokhla stp diap si c urgent

  • @HajarH-fk1ow
    @HajarH-fk1ow6 ай бұрын

    Ay waye kou khamnei akh pa bi bleu akh mom tie yalla rek tax

  • @dieastoufaye5116
    @dieastoufaye51166 ай бұрын

    Walahi faye mane dé douma wéddi xam xam bila yalla may. Bima soné yaw lama yalla bolél té alhamdulilah

  • @HajarH-fk1ow

    @HajarH-fk1ow

    6 ай бұрын

    Ayow doma bolei alh mom nguir yalla

  • @miss3762

    @miss3762

    4 ай бұрын

    Salam puis je avoir son numéro svp

  • @premieredame6572
    @premieredame65729 ай бұрын

    Quand vous faites ces genres d'émission, il faut bien préparer votre questionnaire et savoir suivre les réponses, mais aussi bien connaître le sujet dans lequel vous allez discuter pour pouvoir préparer vos questions,

  • @kannydiarra1171
    @kannydiarra11718 ай бұрын

    Ki loumou wakh deug y’avait des moments Mo wakhone soxna déguéne chimères babou na moytou bopam amna gnoukoyi fékhel matul semaine mou guéne adina il est brave dé Yallah maïnako lol

  • @moussasakho320
    @moussasakho3209 ай бұрын

    Lolou hôpital régional la khéwé sage femme yi gnodon def lolou gnoune gni deuké si wettou hôpital kham nagnousi dara

  • @S-nd612

    @S-nd612

    8 ай бұрын

    Montakh gayii dii bagn nitou fofou 😂

  • @fatouagne6842
    @fatouagne684210 ай бұрын

    Son numéro

  • @Mbayediallo-zf8lc
    @Mbayediallo-zf8lc8 ай бұрын

    Besoin de numéro svp

  • @laoucouledesruissaux4495
    @laoucouledesruissaux44959 ай бұрын

    Bismillah la hawla wala ouwatta ila bilah Deum amoul té deum dou messeu âme . Bayiléne fén.

  • @diallodiallo6656

    @diallodiallo6656

    8 ай бұрын

    Benn si iow

  • @laoucouledesruissaux4495

    @laoucouledesruissaux4495

    8 ай бұрын

    @@diallodiallo6656 Kone dé tay boul nélaw ndakh Dina nieuw sa keur sa bir nék.👹👹👹👺👺👺🎃🎃🍴🔪🍷🕞🗡️♨️

  • @diallodiallo6656

    @diallodiallo6656

    8 ай бұрын

    @@laoucouledesruissaux4495 gneuwal kone deh di ngua dieufour

  • @mbayesow2838
    @mbayesow28384 ай бұрын

    Tonton sa numéro la sokh la wone

  • @aminadrame9243
    @aminadrame92438 ай бұрын

    Je veux juste sn numéro

  • @khalifamboup8129
    @khalifamboup81294 ай бұрын

    Khamna hôpital srx

  • @Queen-oy5ru
    @Queen-oy5ru9 ай бұрын

    Son numero

  • @ousmanjohn2893
    @ousmanjohn28938 ай бұрын

    Bai Len chahan

  • @mr.africa8166
    @mr.africa81666 ай бұрын

    Numero koromack?

  • @MethLeJuriste
    @MethLeJuriste9 ай бұрын

    Son numero way pease

  • @mamediarrandiaye6402
    @mamediarrandiaye64024 ай бұрын

    Numéro kromak la beug svp

  • @fayeaissa1128
    @fayeaissa11289 ай бұрын

    C où à dakar

  • @MarietouMbaye-jb1hl

    @MarietouMbaye-jb1hl

    9 ай бұрын

    HLM grand yoff

  • @user-mm3jr4ft6n
    @user-mm3jr4ft6n8 ай бұрын

    Bilay khamoul dara lekna sama khalis ma wakh ko guisouma linga wakhone mou coupé ma

  • @cherifdiedhiou4287
    @cherifdiedhiou42878 ай бұрын

    Numéro qui la

  • @aliounetraore9579
    @aliounetraore95799 ай бұрын

    Sou féké deum am na neu ñow lék ma mangui nii

  • @senethialy8748
    @senethialy87489 ай бұрын

    Walahi sama nidiaye di netali si wadji bir bi done beuw mako féké fek mne ak sama yaye niofa andone yendou dji fa kerok femme bi bimou nieuwé dafa ni sa bou eumbé dafay guente am khadj bouy lek dom dji koro mak niko sa dieukeur molay def lolou femme bi dem waxko dieukeur dji niko niou dem je vais porter plainte 😂😂😂😂 lou graw

  • @premieredame6572

    @premieredame6572

    9 ай бұрын

    Salut, où peut-on le trouver ??

  • @MarietouMbaye-jb1hl

    @MarietouMbaye-jb1hl

    9 ай бұрын

    HLM grand Yoff tu demande la dibiterie koromake fay dibiterie bi keureum la nek

  • @noorajoof7441
    @noorajoof744110 ай бұрын

    Kagn lakay guiss kii

  • @assanengom3126
    @assanengom31263 ай бұрын

    Où est ce qu'on peut trouver koro mack faye. Où est qu'il habite?

  • @yayeniang9719

    @yayeniang9719

    2 ай бұрын

    Grand yoff y’a lathié dibiterie koromack

  • @mbayesylla7545
    @mbayesylla754510 ай бұрын

    Aye way son numéro svp

  • @El_Chapo155
    @El_Chapo1558 ай бұрын

    Franchement geuwma deum jinné moy doug nite dikko waxlo rek

  • @AmindaoNdao

    @AmindaoNdao

    3 ай бұрын

    Nekal nit 😂

  • @samdoudou1135
    @samdoudou11359 ай бұрын

    Numero svp

  • @mamebettysall9009

    @mamebettysall9009

    8 ай бұрын

    Surtout Loulou

  • @laminegueye5882
    @laminegueye58829 ай бұрын

    Dëm amoul yallah djinn la wakh ak nite

  • @AmindaoNdao

    @AmindaoNdao

    8 ай бұрын

    Dama diapoul mai Mane mimou diapou niari at foune fadijou nafa meunou ma weur 😢

  • @Capitaine203

    @Capitaine203

    3 ай бұрын

    Lamine khana deum ga

  • @ndeyeatta9946
    @ndeyeatta99469 ай бұрын

    Mane dama sohla numerome bilahi dimbali léne massi svp

  • @abdoulayediop907

    @abdoulayediop907

    Күн бұрын

    Sa maison c'est vers hlm grand yoff Près de la brioche dorée

  • @laminediagne2949
    @laminediagne294910 ай бұрын

    Croire à ce qu'il dit c'est ne plus croire au Coran, a enseigné le prophète.

  • @aliotop1293

    @aliotop1293

    9 ай бұрын

    Explique ??

  • @13orkchez26

    @13orkchez26

    9 ай бұрын

    Pouvez-vous nous expliquer davantage

  • @laminediagne2949

    @laminediagne2949

    9 ай бұрын

    @@13orkchez26 Le Coran enseigne que la divination est une oeuvre diabolique: يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِنَّمَا الْخَمْرُ وَالْمَيْسِرُ وَالْأَنصَابُ وَالْأَزْلَامُ رِجْسٌ مِّنْ عَمَلِ الشَّيْطَانِ فَاجْتَنِبُوهُ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ [٥:٩٠] O les croyants! Le vin, le pari ( jeu où l'on risque de l'argent), les pierres dressées (monuments), les flèches de divination ne sont qu'une abomination, œuvre du Diable. Ecartez-vous en, afin que vous réussissiez.

  • @elzodiams461

    @elzodiams461

    9 ай бұрын

    Deum nga

  • @ousmanedieye8894

    @ousmanedieye8894

    9 ай бұрын

    Mbadou si nga bok

  • @aliounetraore9579
    @aliounetraore95799 ай бұрын

    Nitt menoul nék deum bima djido beu legui messouma djiss kou djiss deum ay rimeur rek yak derou nitt dilén accuser ay deum pour ñou detesté lén pour les rend pauvre aussi c'est tres mauvais wly

  • @Queenprincesse1

    @Queenprincesse1

    8 ай бұрын

    Hii deumou amna billahi walakhi koune amoul dala diapoul deukeul na deumou khamnasi dara

  • @whythenumber21everywhere6
    @whythenumber21everywhere69 ай бұрын

    Deumm amoul c'est faux. Djiné mo amm. Djiné moy dougueu ci nitt diko lékk mais pas nitt...C'est l'œuvre de Iblis. Nitt nitt leu , manoul lek nitt comme on veut nous le faire croire. C'est totalement faux Ce marabout n'est ni maître de son âme ni de son corps. Ay djiném nio deuk ci yaram bi diko manipuler, nioy wakh ci laminiam nioy dokh ak tankam. Toutes ces paroles sont des paroles de djiné. Kou gueumm ay djiné nak ça affaire là

  • @aliounetraore9579

    @aliounetraore9579

    9 ай бұрын

    Bien dit

  • @moustaphadiouf3958

    @moustaphadiouf3958

    8 ай бұрын

    Deum amna DEUG kouko wédi deumbe gua

  • @whythenumber21everywhere6

    @whythenumber21everywhere6

    8 ай бұрын

    @@moustaphadiouf3958 Yén sérère yi da nguén bariy djîné nak...vous croyez facilement à tout ce que vos diables vos racontent. Serigne Cheikh Al Makhtoum nous a bien expliqué l'inexistence des deumm. Vous êtes ignorants et vous voulez embarquer tout le monde dans votre bateau de shirk?

  • @astoudiop6312

    @astoudiop6312

    8 ай бұрын

    @@moustaphadiouf3958 Merci beaucoup

  • @ibradiongue8900

    @ibradiongue8900

    8 ай бұрын

    hana daga bokk si gnomm😢

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop874910 ай бұрын

    Bone dé yaw deumaga bayilène thiakhane sou deuma amé rék yaw yaye deumeubi

  • @leveridique9276

    @leveridique9276

    10 ай бұрын

    Sawaay bayyil weiddi loo hamoul deummeu wallahi amna problème bi nak mooy compréhension nit naturellement dou neikk deummeu waayei cheytaanei mooy posseder nit diko utiliser loolou laniouy wakh deumeu feibar leu danioukoy fathie mane mii hamnaa koo hamni moom lawoone waayei leigui machallah kon sooy weiddi weidil loo kham

  • @almaktoumdiop8749

    @almaktoumdiop8749

    10 ай бұрын

    @@leveridique9276 deumeu amoule ganane bayile wédi lo khamoule deumeu bou amome bone mane yaw laye diapé deumeu ani sénégal banou dalé wakh deumeu baa taye ani koussi meusa guiss nite mouye lèka nite gñiémé bakar ak bòne rék

  • @leveridique9276

    @leveridique9276

    10 ай бұрын

    @@almaktoumdiop8749 ndeysaane maintenant je vois que c'est un ignorant qui parle deumeu neinaala cheytaanei mooy neikk ci guinaaw ay kham kham la yoo hamni mystique leu niniouy deif nit loolou sa beuteu meunouko guiss mane wakhoumala louma hamoul dei mane en personne damay fathie ci alquran ak sounna ligay wakh nii laadaane wakh waayei nit nieuwna baci mane nima deumeu laa hana boobou moo gueuna dei tei alquran neina amna ay goor ci nit daniouy collaborer collaboration boobou mooy takh nit gni cheyaatiin qui dilein jangal ay ham ham you bonn

  • @swartnwar916

    @swartnwar916

    10 ай бұрын

    @@almaktoumdiop8749 Saway ioe seu argument bi mom takhawoul, meusso guiss deum donc amoul? Est-ce que meuss ngu guiss djiné tei pourtant lou amleu beu Yallah wakhko ci Al Quran. L’élégance intellectuelle voudrait que nit lo moussoul guiss tei khamoko ngu bagn wakhni amoul.

  • @mouhadjigueye7637

    @mouhadjigueye7637

    9 ай бұрын

    @@swartnwar916 Mane dé guiss n'a nite bouy déffe ay magie noire té souniou polonetéreyi nio diakarol wone sa Souma teudé wone Daf ma done yérnou dima espioné dima surveillé si loumay déf yeupe mais bouma teudé guoudedi nélawoumawone dama ko fixé guiss ko diaharane Mouy sopaliko beuteyi Di takeu té nitela mako guiss amena

  • @tourebineta2108
    @tourebineta21088 ай бұрын

    Son numéro s il vous plait

  • @user-ut2fn3ln5y
    @user-ut2fn3ln5y10 ай бұрын

    Son numero svp

  • @DibiterieSeck-ky8tn
    @DibiterieSeck-ky8tn6 ай бұрын

    Numéro watssahpp bam

  • @fatoumbaye1121
    @fatoumbaye112110 ай бұрын

    Son numéro

  • @fatoufaye2094

    @fatoufaye2094

    10 ай бұрын

    😢 de

  • @fatoufaye2094

    @fatoufaye2094

    10 ай бұрын

    Ô inox

  • @leveridique9276

    @leveridique9276

    10 ай бұрын

    Yow lane moola daleu???

  • @Coriolanusshap22

    @Coriolanusshap22

    9 ай бұрын

    Demal scat urbam taxi bo lathie dibiterie Koromack mou deposer la si keur bi !

  • @fatoumbaye1121

    @fatoumbaye1121

    9 ай бұрын

    @@Coriolanusshap22 ok merci beaucoup scat urbam soriwouma diéguénama nafa dem inchallah que dieu te protége coloriolanusshap22

  • @user-ut2fn3ln5y
    @user-ut2fn3ln5y10 ай бұрын

    Son numero svp

Келесі