Khoutba Serigne Mor Mbaye Imam : Yéne déclaration yi thi bisou Tabaski..21/06/2024

Ойын-сауық

ASKANWI TV

Пікірлер: 19

  • @amartoure9971
    @amartoure99713 күн бұрын

    Merci imam Mbaye ci kham kham bi at patriotisme bi yalna yalla goudal sa fane

  • @makharyndiaye5922
    @makharyndiaye59225 күн бұрын

    Machalla imam

  • @damegueye5112
    @damegueye51122 күн бұрын

    Y’a imam et imam Dieuredieuf imam Mor Mbaye

  • @rawanediakhate1581
    @rawanediakhate15816 күн бұрын

    Machalla imam fatali dîna diarigne

  • @cheikhcokidiop6690
    @cheikhcokidiop66903 күн бұрын

    ماشاء الله تبارك الله شكر لكم وجزاكم الله خيرا

  • @guisstekhe2230
    @guisstekhe22302 күн бұрын

    Ma cha allah amna solo ❤❤❤

  • @talibechiekhsopnaby3401
    @talibechiekhsopnaby34016 күн бұрын

    machaàllah jêrêjëf Mbaye yagafi téq wér loooooollllll

  • @barabadiane5298
    @barabadiane52986 күн бұрын

    Dieuredieuf imame

  • @massarsarryallayallayereua2287
    @massarsarryallayallayereua22873 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤

  • @assaneniang2133
    @assaneniang21336 күн бұрын

    Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yònnent bi (SAAWS) akiy sahaabaam (RAA) te wërsëgël nu nu dëkkag ñoom ca kërug teràngaam.

  • @massarsarryallayallayereua2287
    @massarsarryallayallayereua22873 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @antadiop6262
    @antadiop62626 күн бұрын

    ❤❤❤❤

  • @assaneniang2133
    @assaneniang21336 күн бұрын

    Assalaamu alaykum. Nanu YÀLLA sàmm sàmmal nu, aar aaral nu, taxawu taxawul nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xam xam yi ragal sunu BOROOM YÀLLA.

  • @assaneniang2133
    @assaneniang21336 күн бұрын

    Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAH. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer, MU yombalal nu tòpp ko, MU wan nu neen bamu leer, MU yombalal nu dùmmóoyu ko.

  • @papamormbaye2076
    @papamormbaye20766 күн бұрын

    Mbaye yague fii lool té ande ak werr

  • @astouthioune6321
    @astouthioune63216 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ElhadjiNiane-ib7uj
    @ElhadjiNiane-ib7uj21 сағат бұрын

    Amnasolo

  • @bayeka7531
    @bayeka75316 күн бұрын

    Groupe watchap la beugu

  • @papefaye3811
    @papefaye38116 күн бұрын

    Dieuredieuf Serigne Momar Diagne yalla nala fi bour yalla yagual te ngua and ak weer bidiahi Mouhamadou rassouloulahi SWS BARKEP SERIGNE FALLOU AK SERIGNEME

Келесі