Jazboul Mouride Baye Adama Sarr sur Serigne Mor Dia Ndiar

Baye Adama Sarr sur le parcours de Serigne Mor Dia Ndiar
Abonnez à la chaine ‪@JazboulMouride‬ pour recevoir plus de vidéo sur l'oeuvre de Mame Cheikh Ibrahima Fall.
Contact: uvcomm221@gmail.com
+221 775561634 - +221 778136201

Пікірлер: 212

  • @Senegal780
    @Senegal7803 жыл бұрын

    Baye adama yalla nga goudou fane dooley sei chiekh ibra 😍🙏🏿

  • @papaallefall5041
    @papaallefall50412 жыл бұрын

    sidy birahim fall yalla naniou koh yalla fayal

  • @falloudia1016
    @falloudia10165 жыл бұрын

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @falloudia1016
    @falloudia10164 жыл бұрын

    Yalla nagnou yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @abdoukhadeetoure1127

    @abdoukhadeetoure1127

    4 жыл бұрын

    Machalaa

  • @zaltalightsene5009
    @zaltalightsene50092 жыл бұрын

    Dieureudieuff Cheikh Ibrahima Fall Baboul Mouridina ☕❤️❤️ Baye Adama Sarr ygu fi loll t3 andak werr amine 🤲🤲

  • @cheikhousow3486
    @cheikhousow34866 жыл бұрын

    Dieureudieuf Baye Adama Sarr sa nekinne amalna beepoum Senegalais ndieurigne yalle na sa Diam ak salam ak ilma ak weur sax nganiouy xamal sounou diar diari mame you bax cii barkee serigne Touba ak mame Cheikh Ibra Fall. AMINE xol sedeutina Barakalahou fiq.

  • @mamecheikhibrafall9434
    @mamecheikhibrafall94347 жыл бұрын

    dieureu dieuf mam adama sarr yalla na yalla yokk saw fan ci barke bay cheikh ndaw

  • @falloudia450
    @falloudia4507 жыл бұрын

    Santati Cheikh Fallou Mbacké Santati Cheikh Mor Dia Ndiar sène mbokoum Talibé: Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar Diam ak Khéwal fane wou goude ak wér Amine yarabal alamine

  • @yatalwaxibayesammbaye

    @yatalwaxibayesammbaye

    5 жыл бұрын

    Magui ziar bou werr

  • @mamadouwane1570

    @mamadouwane1570

    4 жыл бұрын

    Bouniou faté si niane Fall

  • @mamadouwane1570

    @mamadouwane1570

    4 жыл бұрын

    Dila ziar bou weer Yaag fi Lool té andaak weer

  • @goumbadiop5387
    @goumbadiop53878 жыл бұрын

    thiey Serigne touba amoul morome diarrama mame cheikh Ibra fall dieureudieuf sounou mame momar dia moumeu diander yallanako yalla fayal nouneu wa diender si barkép Serigne touba

  • @omarfaye7074
    @omarfaye70749 жыл бұрын

    Dieuredieufé Serigne Touba Khadim Rassoul diarama Cheikh Ibrahima Fall. Baye Adama Sarr yalla nako Yalla may goude fane mou yagga nio khamal ci niari dieum yi di béne

  • @AbaRidial228
    @AbaRidial2282 жыл бұрын

    Mamou Serigne Modou DIA Méouane le référence de la jeunesse......... Dieuredieufaty Serigne Mor DIA NDIAR

  • @Thiaatfaalsakor

    @Thiaatfaalsakor

    11 ай бұрын

    Comment faire pour aller à ndiar svp

  • @falloudia1016
    @falloudia10166 жыл бұрын

    Yalla nagnou yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @falloudia1016
    @falloudia10165 жыл бұрын

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar Yalla nagnou yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @mamadoumboupgueye1901
    @mamadoumboupgueye19013 жыл бұрын

    Je salue baye Adama Sarr et l'ensemble des personnes de Lamp fall TV merci

  • @moussajrdiop1701
    @moussajrdiop17014 ай бұрын

    Baye adama AK wa keur gui Serigne bi rék moo yor faay yalla nalén faay

  • @dembacoulibaly3447
    @dembacoulibaly34478 жыл бұрын

    Salam Baye Adama Sarr DIEUFDIEUL DOUNDAL 111 ans bamatt ndieup mame Adama thie barkes Mame Cheikh Ibra fall

  • @user-um5je9iq9j
    @user-um5je9iq9j9 ай бұрын

    Dieuredieuf Serigne Touba diarama Mame cheikh Ibrahima fall l'AMP baboul mouridina

  • @MamadouMNDOYE
    @MamadouMNDOYE9 жыл бұрын

    Baay Adama Sarr way! Seugn Mamour ak Seugn Bada kén dou yéén.. Jerejef !

  • @tanjichanel4164
    @tanjichanel41647 жыл бұрын

    Yanaléne Cheikh Ibra fayal bopam ! Contane naniou si yeine Fall !

  • @falloudia1016
    @falloudia10165 жыл бұрын

    Yalla nagnou yalla defal Kazzu Radiabu diam ta gnou fekeko ay yoni yon Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @ndoyemoustapha6109
    @ndoyemoustapha61094 жыл бұрын

    Baye adama yallaga goudou fannne wayyy thieyyy gni rekkk danion apou

  • @falloudia450
    @falloudia4507 жыл бұрын

    mane sène mbokoum Talibé: Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar mangui gnane YALLAH mou défal gnou wérou koorou diam Yalla nagnou ko fékké ay yooni yoon ak wér ak tal ci barkéb Cheikh Fallou Mbacké ci barkéb Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @manguesylla
    @manguesylla9 жыл бұрын

    Dieureguèndieuf !!! di dolly sant bou baax..tèy ñian yalla na yènnè SERIGNE TOUBA MAMECHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP si ñoun èègue...amiin

  • @awathiam1823

    @awathiam1823

    7 жыл бұрын

    Jeredjeufe Borom Touba. jaraw laque Mame Cheikh Ibrahima Fall. Baye Adama Sarr yale na Gua fi yague té Ande ak Weer. JaGuénejeuf yéne wa jazboul mouride.

  • @yacinendiaye7900
    @yacinendiaye79009 жыл бұрын

    Baye adama on doit linviter tous les mardis sur l emisssion il a bocou de chose importantes a nous raconter yalla na guoudou fane te werrrr

  • @mbayesangue7469

    @mbayesangue7469

    5 жыл бұрын

    Bilahi degeu la

  • @moustaphambaye625

    @moustaphambaye625

    5 жыл бұрын

    0

  • @alimajolie3195

    @alimajolie3195

    5 жыл бұрын

    Walahi lolou rék lagnu wara déf heure boukoko diotam mayé rék

  • @missgallo3643

    @missgallo3643

    3 жыл бұрын

    Amine Ya Rabbih barké Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp

  • @idrissabomou2076

    @idrissabomou2076

    Жыл бұрын

    Sanguekkkmkkkk K Kkkkkk Kkkkkkkk Kk

  • @falloudia1016
    @falloudia10165 жыл бұрын

    Wakhtanewi amna sololool Yalla nagnou yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @cherifa4490
    @cherifa44905 жыл бұрын

    Diadieuf Baye Adama sarr yalla na yalla gudal sa aw fan thie barche MAMe Cheikh Ibrahima Fall Lamp

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia89924 жыл бұрын

    Yalla nagnou Yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @galsensufi8879
    @galsensufi88799 жыл бұрын

    ja nguén dieuf dé mane mi d Tidiane la !!! damay firndél rek ni Cheikh Ibra ak Aladji Malick ay woleuré laniou wone!! waayé itam man mi dè dama sopp mame cheikhra fall.dama si diapanték samay mboki pass pass sakh.bouma la ko diappalone ba bayi nga lajjat meu ndakh ap tidiane la deug!! Khidmatou LampFall bou baye Adama meunone nieuwate wakhtanal niou si ndiabotou cheikh ibra gui di naniou sant bou bakh waay. Yalla na diamm yagueu ja nguén dieufeuty

  • @moustaphafaye8268

    @moustaphafaye8268

    8 жыл бұрын

    Niaak kiniaan dongou rek. kou baxnga.

  • @nourulahmadiya8446

    @nourulahmadiya8446

    7 жыл бұрын

    AMNA SOLO LOLOU

  • @lahatediop9868

    @lahatediop9868

    7 жыл бұрын

    dieureu dieuf yalla nala sounou borome faye

  • @momobayefallmomobayefall5676

    @momobayefallmomobayefall5676

    6 жыл бұрын

    Galsen Sufi wawgor

  • @manblack880

    @manblack880

    6 жыл бұрын

    diadieuff mouride

  • @falloudia1016
    @falloudia10166 жыл бұрын

    Yalla nagnou Yalla defal diam ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke ci barkeb Cheikh Mor Dia sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @falloudia5898
    @falloudia58987 жыл бұрын

    Dieureudieuf wakhtanewi amna sololol Santati Serigne Fallou Mbacké Santati Serigne Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibé: Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @mohammedlamp1199

    @mohammedlamp1199

    7 жыл бұрын

    Fallou Dia diokhma numero bi?

  • @youssoufall470
    @youssoufall4708 жыл бұрын

    baye adama sarr yalla gua guoudou fanne way amin

  • @oumarcisse4443
    @oumarcisse44436 жыл бұрын

    dieuredieufety serigne Mor Dia

  • @falloudia450
    @falloudia4507 жыл бұрын

    mane sène mbokoum Talibé: Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar mangui delou di ziar gnep ci Koritégui.Yalla nagnouko féké ay yooniyoon ak diam ak tal ak wér ci barkéb Cheikh Fallou ci barkéb Cheikh Mor Dia Ndiar Déwénati

  • @ridialtv2076

    @ridialtv2076

    4 жыл бұрын

    Amine yaram saku niane

  • @mohoussa
    @mohoussa9 жыл бұрын

    aywaay Baye adama sarr mingui nii way, namone nala ! wayé lamp fall déleen gnou dimbali di dougal emission massalikoul jinaane biy ame chque lundi ak emission daaju khassida yi ! gnoune thies bilaaahi ay mouride you beug SERIGNE TOUBA gnofi nék té amougnou bén tele mouride, kone deleen si japp nguir BOROM TOUBA AK CHEIKH IBRA ! wakh deug yalla métina trope !

  • @sonzeba9608
    @sonzeba96085 жыл бұрын

    Yagg fii lolou ta andak wérr baye adama si barké serigne touba barké mame cheikh ibrahima fall

  • @akraamatandiouf3121
    @akraamatandiouf31219 жыл бұрын

    Baay adama Sarr djeredjeuf yagg fi rek te andak weer. li bakhna ndakh mag gni nioniouye djangal ap talibé. Serigne Touba amoul morome, diarawlak mame cheikh ibrahima Fall

  • @modousallgueye4161
    @modousallgueye41614 жыл бұрын

    Diarama mame cheikh ibrahima fall

  • @falloudia1016
    @falloudia10165 жыл бұрын

    Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @amdymf4642
    @amdymf46427 жыл бұрын

    macheallah bay Adama sara yallanalafi sunu broum bayi basikanam barke khassida yi

  • @falloudia450
    @falloudia4507 жыл бұрын

    Mangui delouwat di sant bouwerawer Lamp Fall TV. Mention Speciale à toute l'equipe. Ligueybi amnasololool. Sene mbokoum Talibé: Elhadji Fallou Dia di doom ci Serigne Mor Dia Ndiar

  • @cherifdiop4494
    @cherifdiop44947 жыл бұрын

    Sénégal kunu fa jiox ndombol tank ci sayir warr ngaa tiit ci saboop, lii moy dayo, lii moy doylu, lii moy ngorr, lii moy jiom, lii moy fit, lii jiambar, lii moy deugg, lii moy mbax, ñii kèn manatuléna geun fii ak fanujieum, BOUR YALLA désèlul Sénégal darra (yeurmandé).

  • @ramandiouck1553
    @ramandiouck15532 жыл бұрын

    Dieureudieuf MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL

  • @elhadjifalloudia8992
    @elhadjifalloudia89924 жыл бұрын

    Wakhtanewi amatina sololool Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @hamzawydad4871
    @hamzawydad48713 жыл бұрын

    DIEUREUDIEUFAAAT SERIGNE BETHIO SERIGNE BAMBA DIARRAMATYYY SWRUUU MAME CHEIKH SIIKKAARR NDIAYEEE!!!.(MF)

  • @moustaphadiop7687
    @moustaphadiop76879 ай бұрын

    Dieuredieuf Serigne Touba diarama Mame cheikh Ibrahima fall lamp Dieuredieuf ❤❤❤❤

  • @mouhamedsock9858
    @mouhamedsock98582 жыл бұрын

    Machallah baye Adama Sarr

  • @serignembayediandiar
    @serignembayediandiar4 жыл бұрын

    Dieuredieufa Serigne Mor Dia Borom Darou Ndiar

  • @deugrek3312
    @deugrek33125 жыл бұрын

    *Ndeysaan na Ndiar djalé-dji Abdoul Lahat Dia Domi Serigne Khala Dia, sama woleuré lawone mone Lahat Dia Yalnako YALA yeureum ak beep domou djoulite*

  • @dyepi7122
    @dyepi71224 жыл бұрын

    Diarama mame Ibrahima fall

  • @TalibeSTOUBA-nk2hf
    @TalibeSTOUBA-nk2hf7 жыл бұрын

    thieuy sunu mam cheikh ibrahima fall

  • @awacheikhdiop3048
    @awacheikhdiop30484 жыл бұрын

    Baye adama sarr yague fi lolou té wér

  • @ridialtv2076
    @ridialtv20764 жыл бұрын

    Bay adama yalla nanga goudu fann loooooool barkep cheikh ibra fall

  • @macourandiaye854
    @macourandiaye8547 жыл бұрын

    dieureudief diewerigne amna solo

  • @yabsagueye9246
    @yabsagueye92467 жыл бұрын

    DIEUREUDIEUFATY BAYE ADAMA SARR YALLA NALLA YALLA FAYE.

  • @sarrbeugua5867
    @sarrbeugua58676 жыл бұрын

    Dieureudieu mame cheikhe ibra Fall Lamp Fall baaboul mouride dina

  • @beuggeumjeufgoudikbamel6170
    @beuggeumjeufgoudikbamel61707 жыл бұрын

    OH BAAY DAMA SARR MALA BEUG DH

  • @cheikhfall1755
    @cheikhfall17555 жыл бұрын

    BAYE ADAMA YALNALA YALLA FAYE CI BARKE CHEIKH IBRAHIMA FALL

  • @amathamaths6172
    @amathamaths61725 жыл бұрын

    Lamp fall delenn woohh baay Adama sarr chaque jours kiii Goor Yalla kaminnn'la, dafaa amm ngueuramalou Cheikh Ibra diko deglou moyy sugnuu ndiarignnn nguirr jeumii CheikrIbra invité lennko ci 2018 bi wala 2019 bi ci goudigg 31Décembre

  • @moustaphathiam2501
    @moustaphathiam25012 жыл бұрын

    Kènn dou cheikh ibra fall

  • @abdoulayechoukryniang
    @abdoulayechoukryniang2 жыл бұрын

    Bilay walay dingua fii yagg ta werr Bay Adama yagfi rek

  • @user-ie9mc8zj9v
    @user-ie9mc8zj9v4 ай бұрын

    Thiéy baye adama ❤❤❤

  • @abdoulayendongo7955
    @abdoulayendongo79555 жыл бұрын

    DIEUREUDIEUFAAAT SERIGNE BETHIO SERIGNE BAMBA DIARRAMATYYY MMMAAAMMMEEE SWRUUU CHEIKH SIIKKAARR NDIAYEEE!!! (MF)

  • @user-wj9ym7yi6h
    @user-wj9ym7yi6h10 ай бұрын

    Ndeysane ❤❤❤❤

  • @Midadi_TV
    @Midadi_TV2 жыл бұрын

    Numéro Baye Adama sarr la beugue nguir teral ko nguir djeumi serigne Mor Dia kane momathiy dimbali

  • @fallsowrou9852
    @fallsowrou98523 жыл бұрын

    Diarama mame cheikh ibar

  • @djamadegene3317
    @djamadegene33177 жыл бұрын

    amiine mouride diarrama amna solo lolou

  • @lazanbalazanba9290
    @lazanbalazanba92905 жыл бұрын

    Thiay sidi ibrahim

  • @falloudia5898
    @falloudia58987 жыл бұрын

    Mangui ziar ndiabotou Cheikh Mor Dia Ndiar guep Di ziar mboki Talibé yep Diam ak khewal fanne wou goude ak wer Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacké Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibé: Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @bayefall8395
    @bayefall83958 жыл бұрын

    diarama mame cheikh ibra fall

  • @mbaorienlepatriote9066
    @mbaorienlepatriote90665 жыл бұрын

    Bilay mala beug,mala fonkou baye adama sarr yalna ga doundou ay att you barri

  • @aichamaudiang654
    @aichamaudiang6548 жыл бұрын

    thiey cheikh ibra fall baye sarr guoude fanne ak wer rk

  • @talladiop338
    @talladiop3389 жыл бұрын

    serigne mamor baye adama war na niawatte

  • @user-yb5bq2ji1k
    @user-yb5bq2ji1k6 ай бұрын

    Sante Serigne Modou Dia Méouane

  • @salioubah4313
    @salioubah43137 жыл бұрын

    per sawahtanbi djarna aye milliards walahi begue reck li laniou sokhla si Sénégal akh si adounabi dieureudieufe cheikh Ibrahim fall

  • @mamecheikhibrahimandiaye6619
    @mamecheikhibrahimandiaye66194 жыл бұрын

    Diadief Serigne mor ndiaye

  • @kourelahlouminaneargantin3264
    @kourelahlouminaneargantin32647 жыл бұрын

    wa mouride ana s ndiaga dioup baye fall namou nanko

  • @ibrahimadjitte9294
    @ibrahimadjitte92942 жыл бұрын

    Ma cha alla

  • @mbayesoung3022
    @mbayesoung30224 жыл бұрын

    Diarawlak Cheikh Ibra fall

  • @salioundaw8183
    @salioundaw81835 жыл бұрын

    Bilahi amna solo dé

  • @falloudia1016
    @falloudia10166 жыл бұрын

    Santati Cheikh Fallou Mbacke Santati Cheikh Mor Dia ndiar Sene mbokoum talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia ndiar

  • @makhtartraore5943
    @makhtartraore5943 Жыл бұрын

    Machallah

  • @cheikhomarniang2979
    @cheikhomarniang29796 жыл бұрын

    sounou baye adama sarr sopp nanouko lol tee dieumii mame cheikh ibrahima fall gui rek taxx diadieuf fall

  • @falloudia1016
    @falloudia10166 жыл бұрын

    Mane sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar mangui ziar mboki Talibe yep Yalla nagnou yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar

  • @falloudia7641
    @falloudia76416 жыл бұрын

    Dieuredieuf s mor dia ndiar

  • @papaalassaneniang2281
    @papaalassaneniang22814 жыл бұрын

    Alahou akbar!

  • @moustaphathiam2501
    @moustaphathiam25012 жыл бұрын

    Jajeuff sa bay

  • @youssoufall470
    @youssoufall4708 жыл бұрын

    dieureudieufti cheikhra fall

  • @basstouhfatoukebe8388
    @basstouhfatoukebe83887 жыл бұрын

    yag lenfi tei wer wa jazboul mouride

  • @mkbr7587
    @mkbr7587 Жыл бұрын

    Mame Ahmadou seck borom bakh

  • @fallouthiamtalibebamba5766
    @fallouthiamtalibebamba57664 жыл бұрын

    Machalla dieureudieuf

  • @peneseynabou2745
    @peneseynabou27455 жыл бұрын

    Serigne Mamour Ndao ,serigne Alioune liguey bi rafett na serigne Adama sarr wakhtann bi nekhna mougui ni doundeul si MAME sunu lepp mom la BABOUL mouridina ndongo bou khébou MAME Seynabou Ndiaye yarakh

  • @louisediagne2006
    @louisediagne20066 жыл бұрын

    SANTE BOROM TOUBA REKH DJARAMA MAME LAMP FALL

  • @alimajolie3195

    @alimajolie3195

    5 жыл бұрын

    Jaramaté yaay fall bi

  • @beuggeumjeufgoudikbamel6170
    @beuggeumjeufgoudikbamel61707 жыл бұрын

    lahilaha illah theye mame lamp fall

  • @bayefalldiagneinfo8730
    @bayefalldiagneinfo87304 жыл бұрын

    Thiey mame cheikh ibra

  • @madiondiaye3480
    @madiondiaye3480 Жыл бұрын

    machalla

  • @ngathiefall7703
    @ngathiefall77039 жыл бұрын

    Baye à dama sarr yagui te werr

  • @bayesambe2385
    @bayesambe23858 жыл бұрын

    lépe si bakhou mame cheikh ibra rek

  • @kourelahlouminaneargantin3264
    @kourelahlouminaneargantin32647 жыл бұрын

    akassa amna solo

  • @seydisow8041
    @seydisow8041 Жыл бұрын

    Diadieuff

  • @cest-2023
    @cest-20236 жыл бұрын

    Theyyy mannne deeeee Mame Cheikh Ibrahima Fall yemmm nama lolll😂😂