Intégralité touss de Balla Gaye 2 avec Ahmed Aïdara, Aziz Ndiaye et...

Спорт

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
/ luttetv
/ luttetv
luttetv.com/
/ senlamb

Пікірлер: 147

  • @ndieyafallseck5174
    @ndieyafallseck51742 жыл бұрын

    Yaw biambar nga gaindé nga, so done am 100 défaite sakh ont te supportera toujours inchallah. Bégal nga gnou ba tayi machallah. Yaw yague fi rèk té yér. 😍😍😍

  • @boromdoumsal769

    @boromdoumsal769

    2 жыл бұрын

    Bilahi Lou lerr

  • @aminatasylla1648
    @aminatasylla16482 жыл бұрын

    Maneu deih je suis très fière de toi sama mbeuguel ci yaw dou meussa dagneu tu as tous qu'il fallait faire courage et félicitations B52 mola eup dolé tei tamitt koula guiss dembeu ci birr guew gui khamni tu a été atteint mystiquement balla bou meunoul yeungou kokou dou Balla ioe koula kham khamni do wakh pour wakh lo wakh dieuf ko koula méré nak dou supporter deugane taneu yagu ngagnou saggall billah

  • @m.d.d.c.6594

    @m.d.d.c.6594

    2 жыл бұрын

    Walay ndaysane degue rk nga wakh

  • @ousseynougueye2304
    @ousseynougueye23042 жыл бұрын

    Suis fan de Modou lô mais Balla Wallahi mo néxal lamb ji dangay sét touss bi rk 🥰 du courage malgré sa défaite

  • @aissatouseck6242

    @aissatouseck6242

    Жыл бұрын

    Rafetna

  • @ousseynougueye2304

    @ousseynougueye2304

    Жыл бұрын

    @@aissatouseck6242 ki Aissatou bima xame Bargny leu ou pas ?😅

  • @aissatouseck6242

    @aissatouseck6242

    Жыл бұрын

    @@ousseynougueye2304 wa bi dh bargny khawma nak binga khamla ou pas

  • @bayemorbao2454
    @bayemorbao24542 жыл бұрын

    Athia sama champion bi bilay mala beuge défét mo gnew rék kouné ke di wakh louné mais yague nane la tague mais nak santé ko yalla khame né kouy wout yaye am wala gua gnake balla gaye Balla gaye Balla gaye je suis fr de toi

  • @abdouazizsow986
    @abdouazizsow9862 жыл бұрын

    Enfaite bombardier n’avai rien n’a perdre dans ce combat di courage balla on est avec toi

  • @papismendy3965

    @papismendy3965

    2 жыл бұрын

    Tout de g se k.

  • @moustaphadiop9739

    @moustaphadiop9739

    2 жыл бұрын

    Lw

  • @associationfamer2300

    @associationfamer2300

    2 жыл бұрын

    @@papismendy3965 ddďdddďddďddddddddddďddddďďdďddďdddďďdddddddddddddddddďdďdďďdddddddddddddďdďdďdď

  • @user-xu6ly9bh9i
    @user-xu6ly9bh9iАй бұрын

    Balla gaye sama mbeur bi le lion de guediawaye ❤

  • @abdoulayeba4636
    @abdoulayeba46362 жыл бұрын

    Le meilleur de tous les temps ❤️🙏

  • @cisseomar345
    @cisseomar3452 жыл бұрын

    Tay lagn la gueuneu beugg... yaay kignouy begal,..BG 2 sama champion...Bonne chance pour les combats qui suivent🤗

  • @papandiaye920

    @papandiaye920

    2 жыл бұрын

    Dinguène yaga dégue mougnal. Folklore rék ak wakh djou bari danoul kénn

  • @omzobenzema7123
    @omzobenzema71232 жыл бұрын

    For ever j supporte bg2 ❤️✌️

  • @sokhnafall7005
    @sokhnafall70052 жыл бұрын

    Mane sokhna balla reck yalla nala yalla soutourale thi liladese thi lamb dame reck inchalla amine yarabi

  • @cheikhmbackefall7340
    @cheikhmbackefall73402 жыл бұрын

    Balla gaye 2 souniou mbeur c normale sa niak sa papa ak sa tourando fok mou fingne sa premier combat du courage champion

  • @cheikhoudiop3387

    @cheikhoudiop3387

    2 жыл бұрын

    Bikoy eumeu di dane pappam ak toureundowam gniguifi wone

  • @bintadiop9174

    @bintadiop9174

    Жыл бұрын

    Deuge la de

  • @libasselayembaye4419
    @libasselayembaye4419 Жыл бұрын

    31 janvier 2023 Taay la geuneu beug balla gaye 2 ,taay la geuneu geum balla gaye 2💪

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar95482 жыл бұрын

    Balla gaye deux papay mbeur yi kène dou mome

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop12062 жыл бұрын

    Balla gaye est le meilleur de tout les temps lii khéw stade doumako toudé défaite mais sarakh lakoy toubé avec 100 défaites sakh douma bayii tu est le lion❤️🔥, mais tmt arbitre bi défna yeufou thiouné deug parceque ak lou meuneu khéw bombardier champion leu nite kou yarou leu té amna sorti bou balla gaye guéne fofou arbitre bomb la warone diokh victoire mais yénn yii bakhul bomb ne mérite cette humiliation vraiment nite kou bakh leu té défna louné cii lamb konn yénn yii négnkoy moytou, du courage balla tu nous a toujours honoré konn yii dou takh niou bayii nioune ak yaw ba retraite inchalla le meilleur reste a venir king 👑

  • @moussabamba1673

    @moussabamba1673

    2 жыл бұрын

    bilaye je suit pas d accore balla commence a faire comme lac 2 il fuis et ce plains dessu de lui modou lo es meilleur que lui regarde combat modou contre bombardier respect a modou mm dans sa defaite bombardier a reconnu que ces son meilleur combat

  • @oumarndiaye78
    @oumarndiaye782 жыл бұрын

    Toujours derrière toi ça changera jamais mais faut respecté d'avantage tes adversaires et revoir ton entourage physiquement psychologiquement ton adversaire de 45 ans était plus prêt que toi

  • @fridayjacobson1428
    @fridayjacobson14282 жыл бұрын

    Je trouve que quand il y trop de farale contre Bombardie, il gagne. Ce un peu comme contre Modou Lo. Balla a trop des accompagnateurs mystique. Il y trop de embouteillages hier.

  • @bakesprit4408

    @bakesprit4408

    2 жыл бұрын

    Bien vue

  • @ibouthiam6003

    @ibouthiam6003

    2 жыл бұрын

    Rien de mystiques,ce sont des gens qui veulent sortirent à la télé seulement😜

  • @ndieyafallseck5174

    @ndieyafallseck5174

    2 жыл бұрын

    C'est ça le problème il y a trop de monde autour de lui

  • @ibouthiam6003

    @ibouthiam6003

    2 жыл бұрын

    @@ndieyafallseck5174 Merci 👍👍👍

  • @falloushoptv257
    @falloushoptv2572 жыл бұрын

    Man deh chk jrs balla moy sama mbeur sou déme ba bayi beuré ma bayi beuré fans balla pure kou andak mom debut batay do messeu transumé amna nio xamni mom fou nekh rek

  • @ballagaye2koumounekhouleto546
    @ballagaye2koumounekhouleto5462 жыл бұрын

    Bilai ki damako beug 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥

  • @mbackesamb9584
    @mbackesamb95842 жыл бұрын

    Billahi Mala Beugue boo amoon 10000000000 défét Billahi dou takh niou bayi la

  • @mouhameddiarra1240
    @mouhameddiarra12402 жыл бұрын

    Niouss na la deh balla🙆‍♂️😀béne goudi 3 défaite 😀damay foo rek

  • @bakesprit4408

    @bakesprit4408

    2 жыл бұрын

    🤣🤣🤣🤣

  • @awaniang5242
    @awaniang52422 жыл бұрын

    Tay lagne la gueneu beugue BN continuation champion nga

  • @mohamedniang2351
    @mohamedniang23512 жыл бұрын

    Toujour deriere toi mbeur

  • @lahadgning8263
    @lahadgning82632 жыл бұрын

    Franchement nak moy lamb bilay du courage champion 🔥💪🤟

  • @mo-diop2215
    @mo-diop22152 жыл бұрын

    Bilay yaye lamb 🔥♥️

  • @khadimdiouf2355
    @khadimdiouf23552 жыл бұрын

    En terme de force on a senti bombe supérieur à Balla mais augmenter les contacts et les dunes pour l'endurance

  • @mamadoubalde1562
    @mamadoubalde15622 жыл бұрын

    Balla gaye 😋😄 boy niang rèk pikine rèk

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking3822 жыл бұрын

    Warowone sous estimé bombardier dafa am dollé beu légui , liguéye gua mou liguéye Yallheu diokh neu ki ndam , tu n as pas démérité , gueuneu liguéyate rek Inchallah Yallheu bakhneu félicitations bombardier et courage à toi Balla gaye Yallheu neu Yallheu défale nieup diamou Inchallah 🙏

  • @moftv4961
    @moftv49612 жыл бұрын

    Balla gaye reck💪

  • @sambadrame3497

    @sambadrame3497

    2 жыл бұрын

    Waw Waw Balla gaye rekk

  • @ladaradiop920
    @ladaradiop9202 жыл бұрын

    Bilay sama yaram dawna du courage champion Lila warone lepp defngako mai yalla Moy maye Amal diam diou bariii

  • @latyrndiaye962
    @latyrndiaye9622 жыл бұрын

    Kou nek beuga wone sa bopou ni vraiment d'où li moyye mayye Balla dame

  • @mariehelenegomis75
    @mariehelenegomis752 жыл бұрын

    Félicitations champion inchallah sa ira t'es le meilleur Balla 🤴🤴🤴🤴🙏🙏🙏

  • @mamadougueye726

    @mamadougueye726

    2 жыл бұрын

    Baboye mola Oum

  • @issakhandiaye8522
    @issakhandiaye85222 жыл бұрын

    On t'aimera tjrs

  • @papama1975
    @papama19752 жыл бұрын

    Khowma lane mo khéw mé Balla bi yone sa backkou ces pa la mém shause.Massa waye gayndé 🦁🦁🦁❤️👈🤜🤛😎...sa sabarrkat khaméwouniou glaname bi pa.🤦‍♂️😍

  • @a-qudoosallahisone6498
    @a-qudoosallahisone64982 жыл бұрын

    Heures boo wathiée yoon guis ko lamb dafa fiiir dh champion

  • @alinekaraofficiel
    @alinekaraofficiel2 жыл бұрын

    Niang kharagne lo dafa yabaté 😂

  • @thianeteuw8952
    @thianeteuw89522 жыл бұрын

    Ndaysan magui rétan😁 rk geneleu dfarou rk notre Champion national♥️❤️

  • @IfraSy-od7gx
    @IfraSy-od7gx6 ай бұрын

    Balla gaye rek

  • @ndeyefatoubadiane1737
    @ndeyefatoubadiane17372 жыл бұрын

    Di courage champion défarou wade

  • @jolieseye403
    @jolieseye4032 жыл бұрын

    Balla li dou takh ma bayila wala ma dila khass 💪💪💪courage mbeur ❤ 🙄🙄félicitations pologne ish😒

  • @ndiayeaziz922
    @ndiayeaziz9222 жыл бұрын

    Mane dé nanioula dane 100fois biguama danalé yékini ak modou lô nga wadio ak mane soula nékhé sax nga bayi lamb wadio nga ak wa guediawaye

  • @sentubeinfos10
    @sentubeinfos102 жыл бұрын

    Le lion de guediawaye wawaw on est content

  • @salioukane2014
    @salioukane2014 Жыл бұрын

    Bilahi balla damako beug boudone danou 1000 fois sax safouma té bilahi mbeur yi gueune nagnou am problème hum

  • @koromosmajuliius1289
    @koromosmajuliius12892 жыл бұрын

    Un lutteur ne se fait pas en France ni sur TikTok , Facebook etc… Balla Guaye amoule contact, amoul condition physic.

  • @khadimdiouf2355

    @khadimdiouf2355

    2 жыл бұрын

    Amoul Contact lo jouer thi endurance bi mais physique baxna sou yoké contact ak dune mou bax

  • @khadimdiouf2355

    @khadimdiouf2355

    2 жыл бұрын

    Amoul Contact lo jouer thi endurance bi mais physique baxna sou yoké contact ak dune mou bax

  • @moulaysisko46
    @moulaysisko462 жыл бұрын

    Balla Aka meuneu soppeu

  • @loufflass9618
    @loufflass96182 жыл бұрын

    Balla bakouwoufi daraaa

  • @fayacineniang5907
    @fayacineniang59072 жыл бұрын

    Balla champion

  • @bakesprit4408
    @bakesprit44082 жыл бұрын

    Franchement Balla condition physique zéro même ci touss bi il simulait

  • @Makhtoumienne
    @Makhtoumienne2 жыл бұрын

    Balla le maître d'orchestre 😅😅😅😅

  • @souki-saf-group3858
    @souki-saf-group38582 жыл бұрын

    Beug nala lol ndeysan sama mbeur mi Wayei dou tei niou wakh leu DEUG bi Si c'est vrai danga guedia deff contact nguirr yalla prochainement respecté ko pask mola tekk finga nekk Guisnani aussi danga diss si combat bi bref xolatal affaire yi comme ça nga nieuwatt ak force inchallah Courage on t'aime balla Gaye ❤❤❤❤walayi damala beugg rek tei yalla takh sokhlawouma guiss leu pour wakh lako

  • @BabacarbouSonko
    @BabacarbouSonko2 жыл бұрын

    Boy Niang sa Thiès moy affiche 💪

  • @elibrahimahalilullah3678
    @elibrahimahalilullah36782 жыл бұрын

    Ndanane nga bilaye

  • @ablayenittoudeugu1012
    @ablayenittoudeugu10122 жыл бұрын

    Balla ritambalé 😂😂😂😂 Boye Niang molay yobou retraite amato dolei

  • @khassoumcisse3227

    @khassoumcisse3227

    2 жыл бұрын

    Kokou mounoul dane tapha noumouy dané balla gaye

  • @ablayenittoudeugu1012

    @ablayenittoudeugu1012

    2 жыл бұрын

    @@khassoumcisse3227 Saway balla mi yakhouna dolé xalé birrou mère bi mou yor lamb mingui sunu kanam

  • @khassoumcisse3227

    @khassoumcisse3227

    2 жыл бұрын

    @@ablayenittoudeugu1012 bahna balla kouko teukou rek la bagne dakay diaral ray bopam si entrement ak contact kou wedi ladial modou lo ta balla gaye bou paré billahi dou takhaw ak boyi

  • @ballab.s.kndiaye5265

    @ballab.s.kndiaye5265

    2 жыл бұрын

    @@ablayenittoudeugu1012 balla bimou démé gaday mou nieuwatt dann modou kou nek di apprécié nane balla nieuwatt na frère défaite mo dikk rek mais certe balla déséna dafa wara di contact mé kouné balla diéxalna da ngay wax loula nex

  • @sidykebe1192
    @sidykebe11922 жыл бұрын

    Mbeur sport nila rek yag gagnoo beguel boul massa décourager incha allah souba amna

  • @taymounekhsn6924
    @taymounekhsn69242 жыл бұрын

    Vraiment loutakh defo lén intégralité combat yeup yén nama mane Guen na ay intégralité touss lamb yamaler la combat yi fii ame yeup Lepp ngen wone sauf biii farbi mome meuna niak bombardier dou nigérien nii congolais

  • @alassanetairoufall5713
    @alassanetairoufall57132 жыл бұрын

    Balla sama mbeur gua mais demal ligueyatt sa forme danoul say futurs adversaires!tes futurs adversaires dougnou ay ngaka si lamb

  • @aliasfor9626
    @aliasfor9626 Жыл бұрын

    Énorme

  • @mohameddiagana7981
    @mohameddiagana79812 жыл бұрын

    balla gaye manque d'autoritè,son entourage doit etre regler sinon daaay metiii

  • @asseba4700
    @asseba4700 Жыл бұрын

    Balla amene se meme touche contre boy niang wonnko ni khalegua

  • @a.hmadou4424
    @a.hmadou44242 жыл бұрын

    SI BAKOU BI TU PEUX SAVOIR QUE BALLA VAS TOMBEEEEE BAKOU DA WARA GOREEEEE

  • @seckoudabo2402
    @seckoudabo24022 жыл бұрын

    Machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️💪💪💪💪💪💪

  • @ousmanefall9757
    @ousmanefall97572 жыл бұрын

    Courage le lion

  • @papandiaye920
    @papandiaye9202 жыл бұрын

    Dinguène yaga dégue mougnal fans Balla yi

  • @modoumbackeniang7185
    @modoumbackeniang71852 жыл бұрын

    Tousso fi dra lou nekh ba paré qasyi nga andal ay sobé kasse lagn

  • @omarsamba598
    @omarsamba5982 жыл бұрын

    Il paraît que y’a pa d’entente entre gnouy tegueul balla Gaye et ce qu’il veut danser parce que pour moi balla n’a pas bien répété avant de venir y’a trop de désordre dans son touche pour la première fois

  • @serignedieng5762
    @serignedieng57622 жыл бұрын

    Mérénala.torop

  • @babumb....5240
    @babumb....52402 жыл бұрын

    Waaawe ana brome masque bi jajajaja

  • @babumb....5240
    @babumb....52402 жыл бұрын

    Liigua sotèèkou narina wawe goudi goudi capipitale mbour guéèthe

  • @andedieulefimacky5209
    @andedieulefimacky52092 жыл бұрын

    Psychologiquement le décès de son père l'a beaucoup affecté.Wadji day dokh ni reik mais mentalement nekoul Sénégalais bo dano reik niouni tiouné ge.Enplus préparation bi dou insep Balla koukoy neikhal meunoko entrainer.Moussa trainer.Moussa fall reik mo bakh ci moom ak lynx.

  • @aminaba3958

    @aminaba3958

    2 жыл бұрын

    Yiaw ta compris balla gnimou andalleu hier yeup dagnoukoye exploité rkk enplus conditions physiques amouko son entourage tousse bahoussi suis balla a 100% mais hier momeu darra dohoule srx

  • @galaxiepro.5641

    @galaxiepro.5641

    2 жыл бұрын

    meme b52 psychologiquement le decés de son frere pape dia l'a beaucoup affecté mentalement aussi pour b52 ligueneu di diaye seytané yeup ki b52 dako meuneu 4 fois fi beu souba b52 dakoy tereul

  • @andedieulefimacky5209

    @andedieulefimacky5209

    2 жыл бұрын

    @@galaxiepro.5641 mentale bi bomb am balla amouko saway.pape dia bamou décédé eup na 1 an te bou doubless yagoul.

  • @galaxiepro.5641

    @galaxiepro.5641

    2 жыл бұрын

    @@andedieulefimacky5209 say b52 mo meuneu balla gaye 2 mi balla gaye 2 amoul physique tout le monde l'a dit le decés de son pere de son de son n'a rien d'influence sur son combat b52 l'avait terassé alors que son pere etait vivant et meme son homonyme le probleme cest pas là le seul probleme est est b52 fi beu souba souniou done beuréwate mo dane balla gaye 2 ndakh dako meune 4 fw

  • @princelaye8210

    @princelaye8210

    2 жыл бұрын

    @@andedieulefimacky5209 boul wakh ak ki khamoul dara thi lamb gni ay wakhou fans lagni wakh balla kouko khôl boubakh bamouy gneuwé kou kham lamb khamné tay dou bakh psychologiquement il n’est pas sur le combat

  • @matarmbueg4115
    @matarmbueg41152 жыл бұрын

    Daguen bare ak boy bi de

  • @cheikhndao4599
    @cheikhndao45992 жыл бұрын

    Wamer borom Kagoulbi niewoull

  • @pendakebe3436
    @pendakebe34362 жыл бұрын

    Diam si yaw balla

  • @mohamedniang2351
    @mohamedniang23512 жыл бұрын

    Adama ngom demb amna louko méti danio yakeu nday teugeum mbaye si ndiaye loumi def fofou

  • @laminediop8520

    @laminediop8520

    2 жыл бұрын

    Merci tu le vois sur sa tête il a pas aimé

  • @mhd_0039
    @mhd_00392 жыл бұрын

    Borom biir bouy lang bi😁😂😂🤪

  • @zeynacisse4836
    @zeynacisse4836 Жыл бұрын

    Dama ka beugue rk teh yalla takh

  • @damethione6777
    @damethione67772 жыл бұрын

    INDI NGAFI NDAM LOU NEK KONE BOU DEFAITE GNEUWÉ DAGNOUKO WARA NANGOU LIMALAY DOLI REK MOY SA STAFF NAGN BAYI WAKH DJI TÉ LIGUEY

  • @mamadoufaye34
    @mamadoufaye342 жыл бұрын

    Yay lamb dé ken menoussi dara

  • @princebambakarambodji6198
    @princebambakarambodji61982 жыл бұрын

    Lou nekh li kham nga ni dou dane thiate topou ko 😂😂😂😂

  • @ik5001
    @ik50012 жыл бұрын

    Aziz Ndiay Talibé cheikh ga daga am lou reuy del moytou yenene yi

  • @omzobenzema7123
    @omzobenzema71232 жыл бұрын

    Mais gouye gui bi tay la wl

  • @patriotesankara737
    @patriotesankara7372 жыл бұрын

    WALAHI MBEUR BINGA NIOU DANALE YEKINI NGANIOU DESSALATOUL DARA CONTANE SI YAW

  • @latyrndiaye962
    @latyrndiaye9622 жыл бұрын

    Lirou ndian loyye wakh wa kogne ba

  • @gallosaounera1483
    @gallosaounera14832 жыл бұрын

    Allez bombardier xana lii mom concert wally seck laniou neikone

  • @khadimndiaye9685
    @khadimndiaye96852 жыл бұрын

    15:07 partie contre modou lo daguay khamné saway moci ci forme surtout bouy flexion di wathie..

  • @kayexamlouvision5474
    @kayexamlouvision54742 жыл бұрын

    Ki dafa disse Tourner bi sakh defoul ko boubakh

  • @matarmbueg4115
    @matarmbueg41152 жыл бұрын

    Tous barina ay roumbakhalo trop

  • @khadimg2078
    @khadimg20782 жыл бұрын

    Balla gaye nekatoule beur dè balla baniou khamon dou kii

  • @alinekaraofficiel

    @alinekaraofficiel

    2 жыл бұрын

    Day anbiance légi😂😂

  • @khadimg2078

    @khadimg2078

    2 жыл бұрын

    Ndeysan ambiance rek la dèsè 😅😂

  • @ndeyefatoubadiane1737
    @ndeyefatoubadiane17372 жыл бұрын

    Rk

  • @bourybarry3911
    @bourybarry39112 жыл бұрын

    Nooy xaamene kouyy gagné bissou lambadja ? Settloul rekk te khollat mbeur bou nekkeu nimouyy toussee. Koussi geueneu sawar rek wane fa énergie Môme mooy am Victoire

  • @momodiene451
    @momodiene4512 жыл бұрын

    Dougnu meussa bayi gayndé yaffi nekeu

  • @ladoumsn8063
    @ladoumsn80632 жыл бұрын

    1000 defaite yaw lane beug

  • @doudodieng476
    @doudodieng4762 жыл бұрын

    3 0😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅

  • @sokhenasall7068
    @sokhenasall70682 жыл бұрын

    Ça bouge pas ❤️

  • @yalmine765
    @yalmine7652 жыл бұрын

    Lamb dou li touss day diar yonn a plusieurs reprise dego wokk sa batteur andi niari batteur teugg bassi yaggg kenen ki di teugg

  • @modousylla7026
    @modousylla70262 жыл бұрын

    Balla d da yakarni won day nieuw dan bom mem pa une minut waye combat bi daf ko moudie coute cher

  • @gabrielagboton5361
    @gabrielagboton53612 жыл бұрын

    Niang kharegne lo ! Les danseurs de Wally seck, le gas au synthétiseur c'est un musicien de Wally , baboye , etc . Et etc... Lamb dou ay fo wala khaliss késsé !! Lamb c'est a prendre au sérieux , Balla gaye manque vraiment de personnes digne de confiance , il doit revoir certaines personnes et certains comportements !!! Lamb business ok mais fait de manière plus respectueuses pour les sénégalais et les amateurs je pense que ce serait mieux... Félicitations à B52 car pour moi il a su maîtriser a lui tout seul tout c'est Gens autour de Balla .. et les a battus haut la main ✋

  • @doudodieng476

    @doudodieng476

    2 жыл бұрын

    Niom Boucher ak Lirou😅😅😅😅😅😅😅Balla sakh legui Comédien laaa😅😅😅

  • @modousylla7026

    @modousylla7026

    2 жыл бұрын

    Mo bayi ay nitou dembom kay guiso goul dara sakg

  • @zeynacisse4836

    @zeynacisse4836

    Жыл бұрын

    😂😂😂Rip

  • @zeynacisse4836

    @zeynacisse4836

    Жыл бұрын

    Lamb bou nekoul foo lanla😂😂Kagn la légal waaa wouuuu Balla sucre la kouko bagn do ndeki

  • @doudodieng476
    @doudodieng4762 жыл бұрын

    Beurii Waax Baaxoul😅😄😄😄😅

  • @mamediarrad7078
    @mamediarrad70782 жыл бұрын

    Balla gaye ken rek gua meunon defal Ay contact pour vaincre bombe mouy elton Parck nio tollo takhaway mais malheureusement seytané yi yakk nagne sa entourage

  • @mamadougalsen8712
    @mamadougalsen87122 жыл бұрын

    😂😂😂🤣😂😂bombardier ay wakh danouko dh

  • @bourybarry3911
    @bourybarry39112 жыл бұрын

    Combat bi yeuppeu sawayy dako mise sur mystique bi

  • @mamfacamou8340
    @mamfacamou83402 жыл бұрын

    Souma sa gnion dh guén concentré si sa thiès Balla manatoul dh man Balla moy sama mbeur mais cv pas maintenan mbeur contact mais salle rek non non

  • @boromediamono5015

    @boromediamono5015

    2 жыл бұрын

    Balla moko eup xoromou Mbeure

Келесі