Inauguration Restaurant Chez Boucher Ketchup , Wally Seck débarque par surprise

Inauguration Restaurant Chez Boucher Ketchup , Wally Seck débarque par surprise

Пікірлер: 87

  • @oumouseck1783
    @oumouseck178328 күн бұрын

    Li mayou yallah deug yallah nala yallah same thi barki Seydina Mouhamed

  • @mamadoulaminediop-bx3me
    @mamadoulaminediop-bx3me28 күн бұрын

    Maman kiné diouf borom bakh leu papa thione kou bakh leu wally mounoul léneu loudoul bakh❤❤❤❤❤❤ Wally khole bé rafete kou bone rek moko doul bougueu

  • @amsstrong8996

    @amsstrong8996

    28 күн бұрын

    Billahi wallaye yow wahatiko❤

  • @ndeyekhadyseck5583

    @ndeyekhadyseck5583

    28 күн бұрын

    Mane dh damako beuuggg ma doff bilay

  • @Princesseanne14

    @Princesseanne14

    28 күн бұрын

    Bilay Akay noble❤❤❤

  • @awandiayediouf2437

    @awandiayediouf2437

    28 күн бұрын

    bilaye ndeysane té yarna aye domam

  • @mamesayendiaye8150

    @mamesayendiaye8150

    28 күн бұрын

    Degue rek nga wakhe

  • @wfamily9941
    @wfamily994128 күн бұрын

    Ndeysane yalla na diam yag. Limo takh wally dou beug di gen foumou dem mbolo mi topou ko. Boucher restaurant bi yalla na barkel 🙏🏽❤️

  • @latfatimendiaye7507
    @latfatimendiaye750728 күн бұрын

    Wally mom Aby sécuritém tamit 😢 limom woroukoy déf 😢 je king of je yalla nalla yalla samou❤

  • @khadyjasene6034
    @khadyjasene603428 күн бұрын

    Ndeysan dama beug ndakh djikom do féké mouk foumouy wakhè si nit lou bonne kholam rafetna té amna yéné si nit té louko way def amna kholou bal la yalnala yalla sameu mousal la si pékhé nonne

  • @FallouMbaw-lu8uj
    @FallouMbaw-lu8uj28 күн бұрын

    Wally seck nitôu yallehu leuh bly ❤🎉🥰 Yalnaleuh yallehu Takhawou si barké seydinâ Muhammad Ali 😘🙏

  • @MbayeAnta
    @MbayeAnta28 күн бұрын

    Ndeysann borome bakhla rk😊😊 yalna ko yalla defal diam rk 🌺💗

  • @Nord.tv.2023
    @Nord.tv.202328 күн бұрын

    Pawlishe wally nak deug deug moy star bi xool bi cme or marshalla ki dou nitte ❤❤❤❤

  • @mmembacke6263
    @mmembacke626328 күн бұрын

    Boucher hana taye do wah dafa fay nite yi 😂😂😂😂 adouna dafa goude tank na lep di rafét

  • @TazTazbi
    @TazTazbi27 күн бұрын

    Ibrahima Kharitou Yallah Bi Aka Baakh Xol Seck Doundeul Té Andak Wèir in Sha Allah☝🏻❤️📿🤲🏻

  • @waxkatoudeug
    @waxkatoudeug28 күн бұрын

    Boucher nangoul ni wally moy sa baye, di sa bayou way kat

  • @travisscottwiiz8870
    @travisscottwiiz887028 күн бұрын

    Thiey borom deukh bi yalla nala yalla défall diamou

  • @gueyembaye853

    @gueyembaye853

    28 күн бұрын

    Bilay bimaooy wax ak legui doutay moy borom deuk bi de mayou yalla la am

  • @mohametthiam4500
    @mohametthiam450028 күн бұрын

    Chanteur du peuple ❤❤

  • @AwaDiack-hy1ns
    @AwaDiack-hy1ns28 күн бұрын

    Wally seck machallah Nice

  • @pathethiam4561
    @pathethiam456128 күн бұрын

    ❤❤❤❤l'ong vie wally ballago seck

  • @AntaSeye-jn4fd
    @AntaSeye-jn4fd28 күн бұрын

    Ketchups ndeysane Wally rek la Beug

  • @user-rb2ci3jx5t
    @user-rb2ci3jx5t28 күн бұрын

    Ndeyesan manghe joi sah blie 😢 yalna sah diamou blie li dafa daw yaram😢❤

  • @ELBGC360
    @ELBGC36028 күн бұрын

    Wally Yoro xolou sénégalais il faut ngeun kham Lolou ❤❤🎉😢😂

  • @mormbaye2989

    @mormbaye2989

    28 күн бұрын

    Bouko yoron ky mousiba am😂😂😂

  • @bintadiagne2545
    @bintadiagne254528 күн бұрын

    Machallah wally laf thiate

  • @banelnegri2578
    @banelnegri257828 күн бұрын

    C'est très émouvant ❤❤

  • @fatoumattasowe2201
    @fatoumattasowe220128 күн бұрын

    yen yeup wallly ngendiv weur si leap lumu bokuol du bakh ďuneakh du rewesir

  • @FansaraKeita
    @FansaraKeita28 күн бұрын

    Waly nitt laaa bilahi ❤❤

  • @azizdiop7316
    @azizdiop731628 күн бұрын

    Wally seck mo raw kagna thi rewmi 😂😂😂😂😂 foumou diar rire bi topouko

  • @awatouray4328

    @awatouray4328

    28 күн бұрын

    😂😂😂

  • @ablayendiaye9143

    @ablayendiaye9143

    28 күн бұрын

    Bal nanioula

  • @bailadiop695

    @bailadiop695

    28 күн бұрын

    Machalah machalah machalah machalah machalah machalah machalah machalah machalah

  • @pathethiam4561

    @pathethiam4561

    28 күн бұрын

    Bilaye ❤

  • @user-xd5nv5ov9b
    @user-xd5nv5ov9b28 күн бұрын

    Maa shaa Allah ❤❤❤❤❤

  • @user-li1ml6qb3y
    @user-li1ml6qb3y27 күн бұрын

    Nioune Maryacine laNio beug pirrrr❤💯

  • @zeynaboudiop9787
    @zeynaboudiop978726 күн бұрын

    Yaaa meune yaaa eupe dolai sama faramaraine bi ❤❤❤❤

  • @dikhaa8376
    @dikhaa837628 күн бұрын

    Mare yacine Dagua geune❤

  • @mamadoulaminediop-bx3me
    @mamadoulaminediop-bx3me28 күн бұрын

    Wally laf thiate yalla ko bakhal❤❤❤❤❤❤ kene mounou ko bonal wally laf thiate bravo 🎈

  • @Sambou-sh3qx
    @Sambou-sh3qx28 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ le santeur du peuple

  • @Zazindiaye218
    @Zazindiaye21828 күн бұрын

    Machallah rafėt na

  • @assanembenguecisse2949
    @assanembenguecisse294928 күн бұрын

    Ki moromou workat si mime réw ❤

  • @falloudieng8713
    @falloudieng871328 күн бұрын

    Li mome rafétna❤

  • @emiledione3236
    @emiledione323628 күн бұрын

    Waly boula dalati sécurité zero woroul de

  • @user-dl8vp2vd7p
    @user-dl8vp2vd7p28 күн бұрын

    Nice ❤

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy28 күн бұрын

    Tiėy way katt bou makk bii diakhal nama ❤

  • @babacarfam251
    @babacarfam25128 күн бұрын

    Machala tubarkala

  • @user-uz2pt3qd9k
    @user-uz2pt3qd9k28 күн бұрын

    Pawlis mbaye

  • @NdeyemarieNdiaye-mc1ov
    @NdeyemarieNdiaye-mc1ov28 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤li yala la laf lamigne nala thiat sekhlou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤fier de toi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamadousiby9497
    @mamadousiby949728 күн бұрын

    Chanteur du peuple

  • @user-sm1xo4ot5o
    @user-sm1xo4ot5o28 күн бұрын

    Belie Lee YAlalah.mob lad askan bee bugue

  • @gueyembaye853
    @gueyembaye85328 күн бұрын

    Bouche di ree rek xam nani bilay ballago moy wadji rewmi yaw lagn begu mar yafine

  • @AmySeck-xz2gw
    @AmySeck-xz2gw28 күн бұрын

    💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾🙏🙏

  • @fatoucoly7841
    @fatoucoly784128 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fatimazahrandiaye8795
    @fatimazahrandiaye879528 күн бұрын

    Doleinnima boucher Mo inviter wally dee

  • @user-to3sz3oc2k
    @user-to3sz3oc2k28 күн бұрын

    Yami Di wakh Wally moi rar sa baye bou meloni Wally sa keur dniou wah Dara bamou harm hi

  • @serigneseck2854
    @serigneseck285428 күн бұрын

    Siw d'où diami brom

  • @genevievamelo
    @genevievamelo27 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhbouwaliiy2454
    @cheikhbouwaliiy245427 күн бұрын

    Maryacin way borome senegal la

  • @gueyembaye853
    @gueyembaye85328 күн бұрын

    T un artist ya mene ya dax way eup diap dakh game dax solou guene len xam bagage yi guene len mene frai yafi ne

  • @giado8414
    @giado841427 күн бұрын

    ZERO SAVOIR VIVRE. PENSEZ À WALLY

  • @MomOfatoO1
    @MomOfatoO128 күн бұрын

    Ki dou niit késsé dafa rakh bilahi

  • @lunehamadine2115
    @lunehamadine211527 күн бұрын

    Non Wally mo wané

  • @papKhalifaXelTV
    @papKhalifaXelTV27 күн бұрын

    Kouy dawal. Nga téko sa ampoules prosecuteur Tal sen Flache yi ba guissatoul😂

  • @user-lh5zn8nj4o
    @user-lh5zn8nj4o25 күн бұрын

    Baye fall doundeul lou bare bari si barke Seydina

  • @sport_univers.2482
    @sport_univers.248225 күн бұрын

    Faramaren musique

  • @user-li1ml6qb3y
    @user-li1ml6qb3y27 күн бұрын

    Maryacine nak yaye Borom réuw déh deug néxoul

  • @NafiNiang-wx9kn
    @NafiNiang-wx9kn27 күн бұрын

    Pawlish moo yoré thioumou kay bi

  • @maremediop1078
    @maremediop107825 күн бұрын

    Mannn ki noukko nitt di kholè dikkk bagne moma diakhal mbaxxx rek la kham

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame949927 күн бұрын

    😢😢😢😢😢lokho mboubou walibi dou couleur goor djiguéne 😢😢😢😢

  • @wiizelcapojoop1596
    @wiizelcapojoop159627 күн бұрын

    Li lépou diomay la

  • @sambadabo9287
    @sambadabo928726 күн бұрын

    Vraiment les sénégalais non pas de travail 😂😂😂😂😂

  • @cheikhahmadoubambandiaye3763
    @cheikhahmadoubambandiaye376328 күн бұрын

    Waly foumoy diaar celebrer lgbt regarde les manche il pass inapersi contra sagnioul bagne

  • @fatoudiop2538

    @fatoudiop2538

    28 күн бұрын

    Motay

  • @astoudiop8617

    @astoudiop8617

    28 күн бұрын

    Merci si tontou bi​@@fatoudiop2538

  • @Asla173

    @Asla173

    28 күн бұрын

    Mo taye tapete y gnari toubabe gnowe Sénégal ken ki deme Université wakh len si lolou te louma diakhal gori rek gnoune khaste comme diguen l'homme a perdu sa valeur 😢

  • @azizdiop7316

    @azizdiop7316

    27 күн бұрын

    Katal sa ndaye yake wa lgbt doul yeine sonal ngueine nite yi merde 💩

  • @astoudiop8617

    @astoudiop8617

    27 күн бұрын

    @@fatoudiop2538 merci si tontou bi

  • @SeckDame-tu2bg
    @SeckDame-tu2bg28 күн бұрын

    Wally Lamb seck?artiste dafay rare.svp populisme musical no avenir musical.

  • @fallousamb8296

    @fallousamb8296

    28 күн бұрын

    DOF NGA REK NDAKH IOE YAGUI KOY GUISS

  • @aissatoumbackendiaye6031

    @aissatoumbackendiaye6031

    28 күн бұрын

    Bou demoul won yakoy nieuk saga

  • @FtuSy-ok4ih

    @FtuSy-ok4ih

    28 күн бұрын

    Wally dé meunolen si mom dara depuis 2009 mongui fi chaque année nit yi diko geuneu beug mouy geuneu khew. Wally dou dem fougn ko invitéwoul dafa wathié bopam mais li sakh warouko ndakh amoul sécurité. Lila méti moy wally foumou dem riir mi topouko mais yalla moy mayé. Té yenen artistes yangui dem sakh mais ken dalena lidjantiwoul😁. Wally la nit yi beug mom lagnouy setane. Légui yow lossi meun ak bane rapport la am ak carrière musicale lam étant donné que c'est l'artiste le plus écouté au Sénégal 😃

  • @mllfaramareen-uk7tv

    @mllfaramareen-uk7tv

    28 күн бұрын

    Yaw loy wakh ni. Gni wally daleniy may visibilité rek. Juste le fait que mou gneuw fi gnou beuri dinagn yeuk ni ke boucher oubi na restaurant. En plus wally en dehors artiste bimou nek, nit la rek amna vie sociale. Avenir musical mom ay woy ak constance mokoy diokhé té wally mongui si, delen bolé lou bokou té bayi sissou bi

  • @aminatagueye4746

    @aminatagueye4746

    28 күн бұрын

    Yangui sisou der Waly AK rare ter précieux si khaler machalah.sokhor ignanee ignagnatieee Waly dalenn raww rombbb len ba paraît soufel bopam wathier niveau bi.. Travail de maman Barker baye khôl bou rafet thi kaw si kanam dafay guener yokou

Келесі