Hé problème! Kholou iniane la yore, Mbacke Faye détruit Reug Reug na bayi modou Lô dou…

ZARAK VISION vous offre des services audiovisuels à hauteur de vos attentes.
veuillez nous contacter par mail : zarakvisiontv@gmail.com

Пікірлер: 176

  • @cheikhfall8978
    @cheikhfall89784 ай бұрын

    Mbacke champion nga machallah dina bakh de fingako tek fofou la

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj4 ай бұрын

    Modou lôooooooooo ❤❤❤❤❤

  • @user-cj5kr9zc4g
    @user-cj5kr9zc4g4 ай бұрын

    Merci mbacke ❤🙏

  • @IbrahimaDione-wv5mm

    @IbrahimaDione-wv5mm

    4 ай бұрын

    Merci mbacke ki khamoul l'amb

  • @omarbao5556
    @omarbao55564 ай бұрын

    Merci Mbacke

  • @cheikhfaye1467
    @cheikhfaye14674 ай бұрын

    Merci beaucoup mbacké faye ❤❤❤

  • @ndiagasarr959
    @ndiagasarr9594 ай бұрын

    Mai borom pull bou rouge melni ndeye golo ni Modou dou morom reug reug , reug franc moy moromame

  • @walowal8745

    @walowal8745

    4 ай бұрын

    May kate sa yaye dh lou nekh sakh

  • @ousmanesylla2620
    @ousmanesylla26204 ай бұрын

    Saway yagui mer de 😂😂😂 Modou lo dou bere ak reug reug 😂😂🤪🤪🤪

  • @pathesamb9561
    @pathesamb95614 ай бұрын

    Champion yalla nalla yalla lafal diatt

  • @saliougueye9833
    @saliougueye98334 ай бұрын

    Reug reug dafa bari wakh

  • @user-xt9ci4oy2q
    @user-xt9ci4oy2q4 ай бұрын

    Sama yone nékousi ndakhe balla gaye la waye reug reug défofi dara démale viré dji

  • @petitjoeba4031
    @petitjoeba40314 ай бұрын

    Merci mbacke

  • @MrFayemanou
    @MrFayemanou4 ай бұрын

    Mbacke a raison

  • @mansourndiaye1906
    @mansourndiaye19064 ай бұрын

    Mbacké faye do nokhou qui mouye ratatati ak kanamam bi méllni tatou thine ni modou lo dou moromou reug reug reug reug franc moka meune si lamb avec frappe 100 fois apart bombardier kane lafi reug danne te sakh sou nitté wone modou lo meune nako maye change mais daffa doff il communique mall PA kassé ❤

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara9234 ай бұрын

    Mbacké faye ya taye waxal loula neix on est fiers de toi

  • @lomamadou4526
    @lomamadou45264 ай бұрын

    Avocat Reug reug bii môme mbeur leu ou chroniqueur lamb😅

  • @abdoulatifdiop5640
    @abdoulatifdiop56404 ай бұрын

    Vraiment li mbackè wakh moy dègue reug reug bombardiers ak kan la daan si VIP yi sathiès dako daan lim wakh môme kenn mounou ko dindi

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijanАй бұрын

    Mbacke fay Liga wax lepo dege la wax Bo ler ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-ry7jw8ul7m
    @user-ry7jw8ul7m4 ай бұрын

    Bien dis mbacke faye

  • @MoDraronie
    @MoDraronie4 ай бұрын

    Saay dafa meunoul exprimer rekk. Reug Reug danoul Mbeur bou nekk VIP a part Bombardier et aussi nekkoul position pour beurer Combar Royale , lolou moy debat bi. On parle d'un combat royale. Reug Reug dafay yomb torop mou wara positionner pour nekk Roi des Arenes. Il faut que Mbeur yi aussi mou amm categories. Dou danou si Sa Thies, dem Bmb rek amm combat royale alors que Tapha Tine Lac2 et Sa Thies et Boy Niang ak Ama Balde nekk fi....

  • @abdoulatifdiop5640

    @abdoulatifdiop5640

    4 ай бұрын

    Nga sagn ko wakh bombardiers rek lafi daan

  • @user-bs2sy9mk4i

    @user-bs2sy9mk4i

    3 ай бұрын

    Bombardier kesseè deh lafiii dann nieuw diii sonalll nittt yiiii Amoul bennn palmarès qu’on se dise la vérité

  • @MoDraronie

    @MoDraronie

    3 ай бұрын

    @@user-bs2sy9mk4i Gars yiii nio makk lamb dji rekk… Sa Thies dakoo Daane en plus. Reug neu demm Beuree ak Gars yiii mooo gueune si Moom

  • @mountaga2287
    @mountaga22874 ай бұрын

    mbacke faye vraiment wakhna deug...

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse48544 ай бұрын

    Machallah mbeur lou leer nga wakh reug reug toujours wakhou doff rk lay wakh

  • @user-ok4jm5ry7w
    @user-ok4jm5ry7w4 ай бұрын

    Moulay néx dila nakkari franc Moy niouss reugg reugg

  • @mbayediop299
    @mbayediop2994 ай бұрын

    Machala diabar

  • @coolboy8672
    @coolboy86724 ай бұрын

    Franc vs Reug Reug yes

  • @abdourahmanelo3574
    @abdourahmanelo35744 ай бұрын

    🥰🥰💪💪Lo

  • @faye6718
    @faye67184 ай бұрын

    Merci champions Jah jeuff 🙏

  • @alassanedieng7479
    @alassanedieng74794 ай бұрын

    Reug reug na bayi modou dou moramame egagoufa dafa bari wakh

  • @babsbaba19
    @babsbaba194 ай бұрын

    J’aime la mentalité de reug reug mais c’est un vrai champion

  • @bigoumzo897
    @bigoumzo8974 ай бұрын

    gayne bii yoré ayy airpods ak gueminam bou ngoudou khana reug reug papam leu

  • @lomamadou4526
    @lomamadou45264 ай бұрын

    Sawaaay Reug dou nii la wara def pr beuré ak Modou déjà monguii saltel victoire diambour Reug da nangou

  • @latsouckfaye9252
    @latsouckfaye92524 ай бұрын

    Bien dit mn. frère reug danoul beur

  • @user-ni2il9kl5d
    @user-ni2il9kl5d4 ай бұрын

    Wawaw mbackei

  • @soraboukharaglo
    @soraboukharaglo4 ай бұрын

    Diaroul wakh bou barry Modou dou beuré ak reug ok

  • @modoulebou634
    @modoulebou6344 ай бұрын

    Merci beaucoup borom pull bou rouge bi waye ✅🙏🏿✅

  • @DameNguirane

    @DameNguirane

    4 ай бұрын

    Khana fans fawzeyni nga😅😂

  • @modoulebou634

    @modoulebou634

    4 ай бұрын

    @@DameNguirane non mane lébou gui rek lay topou nganaman ay Fawzéyni 🫃🏿🫃🏿😂

  • @user-bs9zt8sw9o
    @user-bs9zt8sw9o4 ай бұрын

    Mbaké tu es un vrai champion, l'autre là il es trop bête il ne connait rien du tout

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj4 ай бұрын

    Mbacké stp boul tontou doul kate bi domou bireul bii 😂

  • @moustaphabassiroumbackesen1846
    @moustaphabassiroumbackesen18464 ай бұрын

    Wadji mom day yakheu émission bi ak niaway yam

  • @petitseck7174
    @petitseck71744 ай бұрын

    Bombardier bi reug reug dane Ak Bombardier bi dane Modou lo bokhoul dai

  • @ousmanecisse4262

    @ousmanecisse4262

    4 ай бұрын

    C vrai

  • @ablayesecke7458
    @ablayesecke74584 ай бұрын

    Borom pull bou rouge bi mome xamoul lamb koi niawayam bi

  • @user-ok4jm5ry7w
    @user-ok4jm5ry7w4 ай бұрын

    Qui daffa soxor si modou Messi lo rék médina amoul mbeur bou meuneu dane Messi lo , bayil soxor , Soula nakkariwé nga takk ngéimb modou téggal sa ndéye

  • @AstouCiss-kp6yc
    @AstouCiss-kp6yc4 ай бұрын

    Mbeur tu as raison Reug reug na dem AK franc

  • @AdamaFall-ri6sz
    @AdamaFall-ri6sz4 ай бұрын

    Mbacke Faye ioe Mbeur Nga Waro Di Wakhé Nii Bilay Walay

  • @ShiekhjobeTijan

    @ShiekhjobeTijan

    Ай бұрын

    Lan la wax lo garaw

  • @papedjiby1927
    @papedjiby19274 ай бұрын

    Reugue defou fi darra menager lidiantiquate la yorre

  • @landingsane9219
    @landingsane92194 ай бұрын

    Ki wakh neu deug reug reug danoufi gnary adversaires top niveau... Bombardier leu daane té combat bobou combine leu

  • @MamadouSow-db3fn
    @MamadouSow-db3fn3 ай бұрын

    Mbacké faye la réponse était simple lorsqu'il a dit que le palmarès de reug reug ne lui permet de lutter contre franc. Modou lo aussi son palmarès ne lui permet de croiseir reug reug. Ki mo bagne modou lo reck.

  • @MamanNdiaye-bm9so
    @MamanNdiaye-bm9so4 ай бұрын

    Modou lo kassé ❤

  • @bogalbogal3461
    @bogalbogal34614 ай бұрын

    Ki daf sokhor motakh doudem fen reug mo man sen baye

  • @paulbella8287
    @paulbella82874 ай бұрын

    Reuk reuk dé wiri wiri djanédane 😂😂😂 mome loumou beugeu deufa yombe trop neu dieul moromom si lab modou beurel woul ak mome legui mou nekk mou nakaré wasalam 😂😂

  • @user-kv5ks7fp5x
    @user-kv5ks7fp5x4 ай бұрын

    Ioe bakho respectel mbeur yi

  • @mordiop8192
    @mordiop81924 ай бұрын

    Bien sûr wakhna dageu d reug reug danoul vip

  • @omarlowe3879
    @omarlowe38794 ай бұрын

    Mbacke faye lou Lerr ga wah blie

  • @user-ks7ir5fd1o
    @user-ks7ir5fd1o3 ай бұрын

    Billahi manee mii somaa diapé reug reug damkoyee danee

  • @user-qt6ff4en6h
    @user-qt6ff4en6h4 ай бұрын

    Sa boul deconerway Reug reug champion la der

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar95484 ай бұрын

    Mbacké faye sama kharitt bi kéne dou mome

  • @Madridistas546
    @Madridistas5464 ай бұрын

    Wadji mome khana dafa contre modou lô , modou dé kou ko bagn dagay soneuh rekk bilahi , reugg dieuleul franc ba paré

  • @user-ws4hd6wz9l
    @user-ws4hd6wz9lАй бұрын

    avoca reug reug bi nañu may ñun bërewun ak rëug😂

  • @SalimataNdiaye-fr3sy
    @SalimataNdiaye-fr3sy4 ай бұрын

    Reug reug na ndy yém modou dou ndy moromam

  • @DouK-pw8sr
    @DouK-pw8sr4 ай бұрын

    Wadji kou dèw la modou dousa morome

  • @khadimthiam3081
    @khadimthiam30814 ай бұрын

    Sa toooonou ndèye ngay nane douma dèba ci reug reug iow yaye kane mod lò na bayi kon kom ay tappèt ngeun. Merde way.

  • @DameNguirane

    @DameNguirane

    4 ай бұрын

    😂😅khana fans fawzeyni nga

  • @bilalkhalyfall9938

    @bilalkhalyfall9938

    4 ай бұрын

    Dou nguén beuré ak modou légui dh nopalou lén mo gueune 😂😂

  • @barradieng9824
    @barradieng98244 ай бұрын

    Borome rouge bi da sisou reug reug danoul VIP

  • @user-cj5kr9zc4g
    @user-cj5kr9zc4g4 ай бұрын

    Wadji beuri ndeyam wakh dh ak niawayam na bayi setan ndeyi émission ndakh mom

  • @walowal8745

    @walowal8745

    4 ай бұрын

    Sa data yaye bayil setane sa bounou ndaye way ah

  • @mamelo8830
    @mamelo88304 ай бұрын

    Dangaye doul reug reug defoufi dara

  • @user-pb7qn9dh6i
    @user-pb7qn9dh6i4 ай бұрын

    Delen wakh luh meune nah nk reug reug prouvegoul lo khamni warna beure ak modou lo naniou wakhante dgeu tmt nah liguey basi kanam

  • @pendatalla4083
    @pendatalla40834 ай бұрын

    Borom lou rouge li khamoul dara si loumouy wakh kou gnémé YALLA la mais Reug Reug mome VIP yi douniou moromame kéneu doukosi may chance parce que prouvé woufi dara

  • @user-ms9xc3um1r
    @user-ms9xc3um1r4 ай бұрын

    Ki bilae ay reee lama dff😂😂 un vrai con😢

  • @ibaba7801
    @ibaba78014 ай бұрын

    MBacké rek

  • @modo6218
    @modo62184 ай бұрын

    Wadji beuri na ndey wakh domeram ngua rek

  • @latyrtine8568
    @latyrtine85684 ай бұрын

    Tapha tine vs Modou lo Mais Modou lo gnéémawoul tapha tine

  • @leydigueye407
    @leydigueye4074 ай бұрын

    Dangne ragale reug ya yarou wooo

  • @JeanbaptisteSambou-kb6or
    @JeanbaptisteSambou-kb6or3 ай бұрын

    Boy ioe sa data yaye Modou lo dey nopalekou nakk modou champion niarri adversaire you gueuneuh tangue si lamb dji la diel daane len kone yoone la mou diel pose boy reug reug mounoul daane modou

  • @mansourdieye9494
    @mansourdieye94944 ай бұрын

    Yéne xamguéne lépp waxnanioulen reug reug day done roi des arènes mtx gueni moytu reug reug mais reug reug mbeur manatouko bagne si lamb ji

  • @alhadijmamourcisse1448
    @alhadijmamourcisse14484 ай бұрын

    Mback khamou tous

  • @papedjiby1927
    @papedjiby19274 ай бұрын

    Mbacke woro toke si genrou plateau yi

  • @rokhayathiam7913
    @rokhayathiam79134 ай бұрын

    Boys yi dougou aye journalist

  • @cheikhfall8978
    @cheikhfall89784 ай бұрын

    Reug Reug boudé deug franc la wara beurel sa thies moko dann

  • @papaalleseck1104
    @papaalleseck11044 ай бұрын

    Reukkk na dianguiii Wax reuk amoul Sax 17 combat guaneee gnouy reyyy skkk kou menoul Wax kokou Borom lou rouge liii khamoul lamb

  • @bogalbogal3461
    @bogalbogal34614 ай бұрын

    Mebake mi mom man ma doul dè

  • @user-jw4cg6iw2x
    @user-jw4cg6iw2x4 ай бұрын

    Borome pul ❤ sa thiapa way khamo Ndèye Dara

  • @walowal8745

    @walowal8745

    4 ай бұрын

    Yaw sa data yaye

  • @malickdiop4352
    @malickdiop43524 ай бұрын

    Boulene niou sonal😂waye reug reug fane lay beuré ak modou Lo beurina ay yénén mbeur youmou wara beurel

  • @TaphaKeita
    @TaphaKeita4 ай бұрын

    Reug mon meune wa parcelle dieupe

  • @djibypro7774
    @djibypro77744 ай бұрын

    Boorom pull bi bou rouge keukh leu weeroul

  • @walowal8745

    @walowal8745

    4 ай бұрын

    Sa baye sa mako guena werr domeram

  • @djibypro7774

    @djibypro7774

    4 ай бұрын

    @@walowal8745 khelou dieune nga yoré amoulo argument 🤣

  • @user-dy1kt7dk3n
    @user-dy1kt7dk3n4 ай бұрын

    Borom krouss bi mom khamoul foumouy takhaw😅

  • @yalmine765
    @yalmine7654 ай бұрын

    En dehors sa itv bi tay magui lay suivre mais boy mentalite bi boko nare doxe do done champion d mbeur mou ndaw baxna trop gay ande ak champion mais bo beuguei dieul ni mbeur mou mak mi di doxale walla di communiquer insbi dagay wayadi rek modou bimiy toll sen age danouko seddal ni di xol lou nekh gayi walla di yarou yarou dadane safal communication yeungeul niew stade di teukouwante mais lu boko beuggue tela def di oute communication bou bakh insbi do sori mbeur mou ndaw doff gsy nek di tangal say itv yeungeul sisa morom bagn di wakh si champion yi

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu58894 ай бұрын

    Reug Reug saway Dou sama Mbeur Dei mè Barké cheikhoul khadim Mbeur Mounoko thi Lamb dji amoul ki amoul kaa champion la 🧏Dafa Diarr fou beneu Boy Diaroull lala wax Fara mingain Yakar 14 fois lanou Berai Mapath Reug Reug Danko 13 fois

  • @bilalkhalyfall9938

    @bilalkhalyfall9938

    4 ай бұрын

    Saway maylén nit gni djam ak sén wakhou dof laneu moy lamb dji kéneu mounoufih reug reug té yaguoul dara lakofih sathies daneu li nguén wara kham moy reug reug défoufih loufi mbeur défoul bomané mbapate meuna nanguou mais amène défoufih loufih mbeur défoul té dakhou fih beuré ossi

  • @MouhamedThiam-dz2uz

    @MouhamedThiam-dz2uz

    4 ай бұрын

    Yaw labsolu gueye balla moye sa mbeur modou rek nga bagne do massa wakh thie mome lou raféte

  • @IbouSene-hp5wt
    @IbouSene-hp5wt4 ай бұрын

    Sa data yaye modou lo kess

  • @ndellepene454
    @ndellepene4544 ай бұрын

    Borom pull Bou rouge bi mom vrai nafekh la xana fans club reug reug la bok

  • @jamilprotv1371
    @jamilprotv13714 ай бұрын

    Reug reug tologoul si beuré ak modou gatam mo reuy rek

  • @IbouSene-hp5wt
    @IbouSene-hp5wt4 ай бұрын

    yaw sa data yaye PA kess

  • @milkdiacko7488
    @milkdiacko74884 ай бұрын

    Ki da khamoul dara. Mbake bouko tontou

  • @malickkanekandji9791
    @malickkanekandji97914 ай бұрын

    Iaw do mbeur deeeh xamo d'ara... Reug Reug mola meun fouff

  • @galasfall7419
    @galasfall74194 ай бұрын

    Mbere Lou lerr nga wah reg reg dfoufi dara loumi mbere ak Modou lo

  • @user-wr8zy1gv7h
    @user-wr8zy1gv7h4 ай бұрын

    Reug reug defou fi dara mom ak bombardier

  • @user-bs9zt8sw9o
    @user-bs9zt8sw9o4 ай бұрын

    Reug na pas encore prouvé

  • @MansourDieye-dh6jv
    @MansourDieye-dh6jv4 ай бұрын

    Mbacké Faye do niaff ki coup

  • @ahmettoure813
    @ahmettoure8134 ай бұрын

    Lou takh reug reug dieloul tapha tine

  • @mbayefaye3761
    @mbayefaye37614 ай бұрын

    Yaw Modou sen baye la

  • @bambadiop7451
    @bambadiop74514 ай бұрын

    Mbacke doumou kharamou mbeur la daye topater rekk

  • @Fitserigne
    @Fitserigne4 ай бұрын

    Borome Lou rouge li doff deuge leu

  • @omarcisse6712
    @omarcisse67123 ай бұрын

    Boy bou niaw bi khamoul lamb way reug franc mokeu meune fouf

  • @modoulebou634
    @modoulebou6344 ай бұрын

    Mbacke Faye blessure Modou lo ibrahima Faye buez moko wakh donc boul fi neck di sonal Reug Reug demlen liguéyé yi té bayi waroubi keur modou lo nekh na wayé deflen ni Reug Reug out sa yefou bopou

  • @DameNguirane

    @DameNguirane

    4 ай бұрын

    Yaw ya beuri wakh Mbacké faye deugue rék la wakh Reug défa goufi loutakh mou wra beuré ak modou lo

  • @modoulebou634

    @modoulebou634

    4 ай бұрын

    @@DameNguirane bro ki bu wakhon deug Reug Reug douma si débat sax paska deug moy deug waye ki wakhou sokhar rek lafi wax quoi

  • @DameNguirane

    @DameNguirane

    4 ай бұрын

    @@modoulebou634 wakhoufi dra lo soxor bouléne niou sonal Reug défagoufi loumou wra beuré ak xlo dème léne séti lénéne mo geune mbeur bo beugué beurel mome dangay deff ni sa thies yarou am communication bou bakh mais reug dofla nouko nekh lay wakhé

Келесі