Grand banditisme: retour sur les traces, Pape Mbaye et Ndiogou Beye dévoile tout les graves secrets…

Actubuzz tv

Пікірлер: 79

  • @oumardanieladams7586
    @oumardanieladams7586 Жыл бұрын

    On ne sait quoi dire.Toute cette jeunesse sans savoir,sans diplôme,sans rien.tout le temps dans la rue,c’est difficile.QUE DIEU VIENNE EN AIDE À TOUTE LA JEUNESSE SÉNÉGALAISE.

  • @mamadoucisse8201
    @mamadoucisse8201 Жыл бұрын

    Ndeysane gni ils peuvent régler tous les problèmes de la jeunesse au Sénégal

  • @mamethiernodiouf8976
    @mamethiernodiouf8976 Жыл бұрын

    Nday san bandiyi magéte nanie ohhh bandi amoule ndiarinie

  • @momidiop7878
    @momidiop7878 Жыл бұрын

    Bien dit frere 13 à 14 ans doivent aller à l’ecole 👏👏👏👏

  • @fallougentlemara4853
    @fallougentlemara4853 Жыл бұрын

    Ibou Mongi wax yenga gui ré mais message bou am solo la wax prison Day yak nite naniou kholat peine yi

  • @TikTokMDR_officiel
    @TikTokMDR_officiel Жыл бұрын

    Saison bandit 😔

  • @ballydiop9101
    @ballydiop9101 Жыл бұрын

    Mais yen sites qui va vous arrêter vous n’avez rien à faire que la promotion du grand banditisme ? 😳😳😳😳😳 li ba kagne ?

  • @santeserignetouba4826

    @santeserignetouba4826

    Жыл бұрын

    Yaw dagua ñi diafé Diafé adouna rek molen topp ci société bi lañiou bokk ñianal len ci werou korr bi ñiou changer 🙏🏾

  • @dmxjjj7555
    @dmxjjj7555 Жыл бұрын

    Ils essaient de se ressaisir et faire du bien donc arrêté de les diaboliser vous connaissez pas leurs vécu que dieu vous guides vers le droit chemin barkée wérou koor gui ak seydina mohamed psl amine 🙏🏽

  • @perfectsntv2086

    @perfectsntv2086

    Жыл бұрын

    Amine

  • @boubsciss8430

    @boubsciss8430

    Жыл бұрын

    Amine 🙏🏻

  • @alalama1917
    @alalama1917 Жыл бұрын

    Ndeysane heskey yalla il n’es jamais trop tard

  • @assanegueye28
    @assanegueye28 Жыл бұрын

    Masala yalla samou ta takha woula ❤️

  • @dioplahad84
    @dioplahad84 Жыл бұрын

    Pourtant ibou si biiri wakham migi wakh lo am solo 😢😢

  • @iboudjite4837
    @iboudjite4837 Жыл бұрын

    Mbacke sama grande borom españa

  • @matarndiaye3496
    @matarndiaye3496 Жыл бұрын

    Dofe ndaye ki la done waye, pape mbaye bou Guediawaye kagne lane kaye bayi ndayssane

  • @worldofsport7588
    @worldofsport7588 Жыл бұрын

    émmision bi nice na

  • @mamebiramediop9027
    @mamebiramediop9027 Жыл бұрын

    C’est trop triste de voir ça.

  • @moussatine3635
    @moussatine3635 Жыл бұрын

    Yenne sites Yi invite lenne aye royoukaye domou khrame Yi bayi wouniou Dara

  • @meyebaidygueye1936

    @meyebaidygueye1936

    Жыл бұрын

    Gni ils font partie de la société

  • @mansourkane8937
    @mansourkane8937 Жыл бұрын

    Ibou mi nekhna dh

  • @tepppngom1733
    @tepppngom1733 Жыл бұрын

    Ibou dh xam nako bou bax Texaco yalla nako yalla sopii

  • @santeserignetouba4826

    @santeserignetouba4826

    Жыл бұрын

    Amine 🙏🏾

  • @ahmadoudiop5016
    @ahmadoudiop5016 Жыл бұрын

    Site yi khamounou Dara Dara nak

  • @Mamadou-Fall
    @Mamadou-Fall Жыл бұрын

    Maintenant REGARDEZ BIEN !!!! Demain un autre site va aller prendre IBOU et après un autre site aussi après un autre , après un autre, après un autre !!!!!!! Jusqu'à ce que un autre gars fait surface après ce sera son tour

  • @santeserignetouba4826

    @santeserignetouba4826

    Жыл бұрын

    En tout cas ci société bi lañiou bokk bougn la wakhoon sen diar diar digua comprendre

  • @Mamadou-Fall

    @Mamadou-Fall

    Жыл бұрын

    Yaw yaa lenn boolee thi société???? Noo gnii bokou niou thi société bi deh!!! Niomm douniou ayy sénégalais, ayy burundais ak sierra leonnais laniou !!!!! Ce Ibou là c est ukrainien !!!

  • @user-sf7wy9mj7i
    @user-sf7wy9mj7i3 ай бұрын

    DEUG la wox fi banlieue ay xale you ndaw ngay giss niouy dawale charete

  • @mamadoumbackediop7048
    @mamadoumbackediop7048 Жыл бұрын

    Wah Duagg

  • @seydinaaliounelodja185
    @seydinaaliounelodja185 Жыл бұрын

    Kou delousi Lou bone de Lou kasso

  • @Amathsene15
    @Amathsene15 Жыл бұрын

    MDR Ibou Bayile saloum saloum Yi nak 😂😂😂😂😂😂

  • @torodo.ferrari
    @torodo.ferrari Жыл бұрын

    Ibou mii ndeysann nittou keisseii leu😂😂

  • @papeamathndiaye
    @papeamathndiaye Жыл бұрын

    😂😂😂 ibou guerrier la kw mais tu a raison nak d'une part

  • @seydinaaliounelodja185
    @seydinaaliounelodja185 Жыл бұрын

    Bandit loumouy conseil

  • @njaaydiattandiaye1261
    @njaaydiattandiaye1261 Жыл бұрын

    Boy dounou wakh wakhi niit

  • @tallambengue1092
    @tallambengue1092 Жыл бұрын

    Slm machallah pourtant ibou Ku bakh lamay nuru bly non ibou raynama koi😅

  • @moussadiaw6115

    @moussadiaw6115

    Жыл бұрын

    Kou bakh la khame na ko bou bakh y’a khallé bou naw la

  • @adjiamasina7951
    @adjiamasina7951 Жыл бұрын

    Liléne dale dioboule kéne natou yala la nioune gni nek si diame di teude fou baxe dou souniou diambar yala rek moy deugue

  • @tepppngom1733
    @tepppngom1733 Жыл бұрын

    Bayilene journaliste yii liniouy def DinA takh gni moytou nga kouniou agresser Bo demei si Site yi guiss Ko bouko police Guissé xam Kane la

  • @Issalves88

    @Issalves88

    Жыл бұрын

    😅😂😂😂😂😂

  • @veriteabsoluedeugneekhoul1720

    @veriteabsoluedeugneekhoul1720

    Жыл бұрын

    ​@@Issalves88 😂😂😂😂

  • @NdeyedieumbDiaw
    @NdeyedieumbDiaw10 ай бұрын

    Ndaysan ibou kou rafet khol lamay ndourou

  • @omarsaipsarr2797
    @omarsaipsarr2797 Жыл бұрын

    nooon ibou sonal nga wa saloum do bayi saloum saloum yi

  • @meyebaidygueye1936
    @meyebaidygueye1936 Жыл бұрын

    Ibou mi amna xel deh retaan lou neu waye wax Nafi you am solo

  • @ahmadoudiop5016
    @ahmadoudiop5016 Жыл бұрын

    Le gar en bonnet noir et blanc pape mbaye dit mbaya kouko khamoul guediawaye deg ngako eskey bima guéné nek khalé souma dégué pape mbaye jarnafi légui sama journée yakuna Aka mako ragualone 😂

  • @laperlecmoi5995

    @laperlecmoi5995

    Жыл бұрын

    Mane mama cheikhou la ragalone

  • @papidione266

    @papidione266

    Жыл бұрын

    Real goor bilay

  • @Charles-ec8dp

    @Charles-ec8dp

    Жыл бұрын

    Wakhal de , nioun wa baye laye, xamnagn ko bou bakh, MBAYA

  • @tidjanecorbier4286

    @tidjanecorbier4286

    Жыл бұрын

    J’aimerais bien savoir Loutakh ngene ragalone ko

  • @gueyedaouda8592

    @gueyedaouda8592

    Жыл бұрын

    ​@@Charles-ec8dp gnoune wa tournale Serigne assane gaïndé lagnou ragalone

  • @modouamar1130
    @modouamar1130 Жыл бұрын

    ibou nieup la xame😅😅😅

  • @njaaydiattandiaye1261
    @njaaydiattandiaye1261 Жыл бұрын

    Journaliste diokh lene nou thieur ainsbi lima guiss Moy banditisme ngeni propagande

  • @ibrahimakhalil8800

    @ibrahimakhalil8800

    Жыл бұрын

    Gnom dougnou ay journalist ay vues rek lagnouy weur .. gno yakh deuk bi yeup

  • @366people3
    @366people3 Жыл бұрын

    Goor katane bi moy attoté rék

  • @moussatine3635
    @moussatine3635 Жыл бұрын

    Dewou kagna rek thie milieu ngeni dewe marché bou Bess Mo geunneu bonne

  • @cheikhounabambabasse4779

    @cheikhounabambabasse4779

    Жыл бұрын

    Ne dis pas ça

  • @natachadymen6188

    @natachadymen6188

    Жыл бұрын

    Tu es sure de ce ke tu dis

  • @BocarGangue-gq6rb

    @BocarGangue-gq6rb

    6 ай бұрын

    Boul tekk llou saway

  • @ndiayemandela5275
    @ndiayemandela5275 Жыл бұрын

    😂😂😂😂ibou raynama

  • @beuguefallou6555
    @beuguefallou6555 Жыл бұрын

    Thiey ndiogou beye ak mbaya 😂 milieu dolén ko bayi moukk😂😂mais bégué nalén name nalén am len diam

  • @user-pi1pn6cw9e
    @user-pi1pn6cw9e8 ай бұрын

    Ibou.kou.bakhla.jai.conait.lui.jabite.guidiawaye

  • @jamesjoob3771
    @jamesjoob3771 Жыл бұрын

    Non bandit baxol xolal ñi amonu sakh 🧠xeull

  • @dioppape9868
    @dioppape9868 Жыл бұрын

    marché bou bess ay sathie aki agresseur dongou gnofa nek

  • @lamienolamister7929
    @lamienolamister7929 Жыл бұрын

    Senegal Mom prison def fa yomb

  • @sambasylla5093
    @sambasylla5093 Жыл бұрын

    Sawadi mom changewoul dra borom pull bleu gris bi xolen kanam bi ak tougniom yi

  • @gueyekhoudiaadama7802

    @gueyekhoudiaadama7802

    Жыл бұрын

    Ibou leu 😂😂😂😂😂 9 mandat dépôt le am

  • @moussadiaw6115

    @moussadiaw6115

    Жыл бұрын

    Qui loudoute nane douko déf Fal ko khamoute boukkou juger

  • @sambasylla5093

    @sambasylla5093

    Жыл бұрын

    @@moussadiaw6115 dangay fen ki nane be kanam gui changer

  • @ibrahimafaye4049

    @ibrahimafaye4049

    Жыл бұрын

    Ibou wahne deg ❤

  • @bettygueye6152
    @bettygueye61522 ай бұрын

    Vraiment nk lougnou deff bagnou dann lenn peine bou metti ?

  • @ballydiop9101
    @ballydiop9101 Жыл бұрын

    Deugue ngua waxx mom niit comme yaw ken warouko kall mais yaw aussi niit comme yaw warouloko kar di nangou alalam mba diko gagne ak metital , xolal sa kanam bi comme marché bou tasse ni pour l’an li tamit

  • @lansanatoure1957
    @lansanatoure1957 Жыл бұрын

    Nit kou mauvais Amoul

  • @kareabdoulahad622
    @kareabdoulahad622 Жыл бұрын

    Sen kanam you désordre yi wa loutakh bouniou bayi woon dîna niou melni sen kanam yi

  • @sambadiakhate9845

    @sambadiakhate9845

    Жыл бұрын

    Yw ktsd l’apparence est trompeuse ktsd way

  • @MoustaphaCisse-co7ms

    @MoustaphaCisse-co7ms

    Жыл бұрын

    😂😂😂

  • @babacarcisse6909
    @babacarcisse6909 Жыл бұрын

    Yaw ibou kou kat ndayam ga gay wakh Saloum

  • @ibrahimamba1296
    @ibrahimamba1296 Жыл бұрын

    N'importe quoi.

Келесі