GP - Soxna Kiné Djily: "Li Takh Cheikh Ibra Fall Dou Woor..."

#kebetu #team221 #senegal
page facebbok : / senegal7officiel
Abonnez-vous pour plus de vidéos et n'oubliez pas d'activer la cloche de notification

Пікірлер: 539

  • @louisediagne67
    @louisediagne674 жыл бұрын

    👀😭😭😭mame Chiekh guem n’a la si sama khôl dji 😭😭😭♥️♥️

  • @marafall9936
    @marafall99364 жыл бұрын

    FOUGN TAGUÉ DIAMBAR AP YAMBAR MÊR ! BAYOÛ GOOR GNI ❤DIEUREUDIEUF !!!

  • @aliounediouf9788

    @aliounediouf9788

    4 жыл бұрын

    Barke mame cheikh

  • @samaypapier8279
    @samaypapier82794 жыл бұрын

    " Malheur donc à ceux qui prient, tout en négligeant (et retardant) leur Salat. " (Sourate 107/verset 4,5).

  • @ramandiouck1553
    @ramandiouck15532 жыл бұрын

    Dieureudieuf serigne TOUBA KHADIM RASSOUL diarama MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL

  • @azoubrat220brat9
    @azoubrat220brat94 жыл бұрын

    Cheikh ibra dafa sorii si yala ba sokoy wakh tane khell douko dadj kemen la!!!

  • @idrissadiop9364
    @idrissadiop93644 жыл бұрын

    Subhanallah Allahou Akbar lailah ilahallah subhanallah subhanallah

  • @ablayeseck6047

    @ablayeseck6047

    4 жыл бұрын

    Allahou Akbar... yalla kéneu leu

  • @ndongomboup7518
    @ndongomboup75184 жыл бұрын

    Mame cheikh Ibrahima Fall ab Ndongam rek meunena yilif adouna Kone dousséne morom mane seutoub Cheikh Issa Dienne mako wakh tamouy louwerr té douyakk dara

  • @undisputed2682

    @undisputed2682

    4 жыл бұрын

    Lol 😂 iow dei yay yallah ba ham liii lep

  • @adamadmx6441

    @adamadmx6441

    3 жыл бұрын

    ak sa mamatou mame mais sama mame non

  • @thinktanktruth1968
    @thinktanktruth19684 жыл бұрын

    Kou wakhni cheikh Ibra daawoul diouli dawoul woor wakhoo deugue. Danguèndi yaqq déram. Dioulite piirlawoon. Nafewq baakhoul. Wayé bayalla diapplène.

  • @abouba1485
    @abouba14853 жыл бұрын

    Yalla Santané dioulli ba paré ay doumou adama takhaw diko toutil. Le prophète psl est meilleur que tout le monde en plus on lui avait pardonné ses péchés mais n'empêche il passé toute sa vie à prier.

  • @Anita-vh2kh

    @Anita-vh2kh

    2 жыл бұрын

    Mais mère bii dafayy exagèrer tropppp lane moy cheikh ibra mo nieuka xam yallah foumou tek lolouu anii yonente yiii

  • @Anita-vh2kh

    @Anita-vh2kh

    2 жыл бұрын

    Après niii di diay baye fall bay salitt delolen sen xell yii si yallah

  • @oris7489
    @oris74894 жыл бұрын

    Wallahi sama khol toyna💞😭

  • @youssouphgoudiaby1603
    @youssouphgoudiaby16034 жыл бұрын

    I'm very happy really Maman yague fi lole té ank kok wére

  • @mamadoufaye6230
    @mamadoufaye62304 жыл бұрын

    Bilahi li dafa nékha deg si khôl 💓💓diarama mame cheikh ibrahima fall

  • @damzdiaw9793
    @damzdiaw97934 жыл бұрын

    Sénégal dono doywar koi bayi lénne suni wakh tane si cheikh Ibra fall kénne wakh sénne wakhi diguatte yi kémtani cheikh Ibra fall khadioutt fi lima wakh am ne foumou téck cheikh Ibra fall l'amp moné sumu brom moko téguill korr moné ko yorré luma la borri yorré luma la borri jiuly néko télle niatte yi léguéye mo guene diangue diokhé guene jiuly manu guene korr cheikh Ibra fall mo reuyi wakh

  • @yaramembaye5553
    @yaramembaye55534 жыл бұрын

    Innal fadla bi yadillahi you ti mane yassa...... lolou kouko meunoul tekki sokhla wougnoufi sa commentaire

  • @yaramembaye5553

    @yaramembaye5553

    4 жыл бұрын

    @Elh 2309 mane kaana you minou billahi wal yowmil aakhiri falyaqoul khayrounne aw liyasmoute

  • @ahmadaka6350
    @ahmadaka63504 жыл бұрын

    Thieuy mame cheikh ibra🥰❤️😍❤️❤️

  • @fatoumatadiallo9642
    @fatoumatadiallo96424 жыл бұрын

    So wahé loulene arangé woul rek niouni la mandoul Baye fall Cheikh bethio Kara Aida diallo No yéne vraiment war ngene holate sen bop Merci pour saga yi wara niew, d toute facon saga , sosse, wah diou niaw, moy sen device

  • @biramfall1802

    @biramfall1802

    4 жыл бұрын

    Sa diabote blh cheikh IBRA laniouy waté té yaw yalla nala yalla dibeuli

  • @mbengue2062

    @mbengue2062

    4 жыл бұрын

    Ah yow sa Serigne d digaloula li hawma sah nah tidjane ngeu nah sawa keur yabouniou baye fall wah deug fa yalla

  • @papaalassaneseye8252

    @papaalassaneseye8252

    4 жыл бұрын

    No gni ay domeram lanou di doul rekk ibra fall mom yeufar la

  • @awaseydi7023

    @awaseydi7023

    4 жыл бұрын

    Yalla nala serigne touba dimbali

  • @awaseydi7023

    @awaseydi7023

    4 жыл бұрын

    @@papaalassaneseye8252 sa diobbou ndeye

  • @ycamara9034
    @ycamara90342 жыл бұрын

    I look up to him , he is a gods man. Geray Jeff Bambam ., Bless

  • @kakaka3703
    @kakaka37034 жыл бұрын

    Machalla sokhna kine

  • @lilb6457
    @lilb64574 жыл бұрын

    Allahou Akbar😭😭😭😭😭😭😭yalla nagnou yalla Diégueul

  • @serignembackembengue3081
    @serignembackembengue30814 жыл бұрын

    Soxna kiné djili yagu fi lol ken dou cheikh Ibrahima fall lamp❤️🙏🏾

  • @fallougallascisse255
    @fallougallascisse2554 жыл бұрын

    Kii limouy wakh amna niou kham louko geuna grave mais dougn ci wakh ndakh bougn ko wakhee niou bari weddiko ta kouko weddi danga alkou lolou mo takh amna nioo khamné mbiroum baatine dougn ci dougou.nit ki loo khamoul danga caa wara mandou loo kham nga rafétal thia leegui boo dee khool sakh gniy wakh né ay dioullit lagnou nioo geuna niakka mandou ndakh lougn khamoul weddiko Ta yalla moo wakh ان الله يا مر با لعدل والإحسان. lou takh dougn ko dieufee walla dagno diangoul problem yi am ci adouna bi niakka kham dara ci c ibra rek moko waral ta dougn nongou kouko wakhtané waayé kouci dee danga réthiou barkeb. Cheikh ibra. Fall

  • @sen2287

    @sen2287

    4 жыл бұрын

    Waay bayil doull iiisss niitt souyy fenn danganann ko fenn nga. Ayy doull rekk laffi degg

  • @ibradiagne2747

    @ibradiagne2747

    4 жыл бұрын

    @@sen2287 yaw deh billahi watena ci Cheikh Ibra Fall billahi yalla nala yalla ate al nioun Cheikh Ibra nak dou kou niouy dingate So douguè biir bammel di nga kham bou bakh kouy Cheikh Ibra

  • @sen2287

    @sen2287

    4 жыл бұрын

    Ibra Diagne yawak cheikh ibra senn deudieuw ndayy

  • @mamadoubaidydiop9175

    @mamadoubaidydiop9175

    4 жыл бұрын

    Yow sa nounou Mame

  • @ibradiagne2747

    @ibradiagne2747

    4 жыл бұрын

    @@sen2287 diegal nala waye yalla nala Cheikh Ibra fall diegal ndakhte boula diegaloul dina meti si yaw

  • @santeyallla4422
    @santeyallla44224 жыл бұрын

    Diarama mame lamp fall❤️❤️❤️

  • @fatousene4748
    @fatousene47484 жыл бұрын

    Dieurediefé Sérigne touba diarama mam cheikh Ibrahima fall

  • @couragueye1970
    @couragueye19703 жыл бұрын

    Diarama Mame Cheikh Ibreu❤️❤️❤️❤️

  • @fallouthiam7222
    @fallouthiam72224 жыл бұрын

    Allahou Akbar cey Mame cheikh 😭😭😭

  • @famalo7804
    @famalo78044 жыл бұрын

    Dieurdieurf serigne touba diarama mame lamp fall ♥️♥️♥️♥️

  • @sen2287
    @sen22874 жыл бұрын

    🙊🙊🙊🙊 Yala nama Yala diégal si kadou yima diota degg Allahou Akbar

  • @martafernandez685

    @martafernandez685

    4 жыл бұрын

    Ba degué wakh tanou cheikh ibra lala yalla degue

  • @teuweude1551

    @teuweude1551

    4 жыл бұрын

    Yalla nala yalla sopi té toupe Lima liir sa commentaire

  • @meujnatdiakhate8470

    @meujnatdiakhate8470

    4 жыл бұрын

    Yow doul...gnanal yalla djeigala say baakar mo geun

  • @fallougueye5424

    @fallougueye5424

    4 жыл бұрын

    Mame chiekhe ibrahima fall amul morme fall

  • @mamecheikhcisse9743

    @mamecheikhcisse9743

    4 жыл бұрын

    Cheikhra fall rek👌💪👌

  • @laveriteappartientaallah5218
    @laveriteappartientaallah52184 жыл бұрын

    aka nio beurii niou dofff nie yalna yalla tekeu ĺéne si yonou dîner bou séleu yéne ak niou mélni yéne si cetait un pays musulmans yéne nieupeu si kasso bii lagniou di dor

  • @buzz5109

    @buzz5109

    4 жыл бұрын

    Yaw homo dinee diou sel moy lane mandou mo gueune koor

  • @gogofofana9086

    @gogofofana9086

    4 жыл бұрын

    Lidiantilll Sa bopp rek tes nga manou bay

  • @daoudasarr5776

    @daoudasarr5776

    4 жыл бұрын

    Ya meune ndeye doul ioe dagay dioulite

  • @diallodiallo6656
    @diallodiallo66564 жыл бұрын

    Vive les bayes fall vive le mouridisme. Cheikh Ibra sera le guide spirituel le plus exalté dans le futur. Car des génération beaucoup plus consciente arriveront . Tout ce qui sont contre lui sont que des pauvres ignorants et des bandes d'alliéné qui souffre d'un sentiment d'inferiorité vis à vis des arabes

  • @shashaofficiel8125
    @shashaofficiel81254 жыл бұрын

    Taguén moytou di toumal sounu borom🙏

  • @bambawade4160
    @bambawade41604 жыл бұрын

    Dieureudieuf Mame CHEIKH IBRA

  • @salioundiaye2832
    @salioundiaye28322 жыл бұрын

    Thieye cheikh ibra

  • @user-hr1zd7xo3s
    @user-hr1zd7xo3s4 ай бұрын

    Thieye Mame cheikh Ibra ❤❤

  • @espoirfootkeurmbaye7595
    @espoirfootkeurmbaye75954 жыл бұрын

    Ndeyesaane sokhna si loumouy wakh dégueu degueu la lathié bilay diarama mame cheikh Ibrahima Falk lamp diadieuf sokhna kiné

  • @ablayesarr639
    @ablayesarr6394 жыл бұрын

    Ayy sokhna cii wangnil wax dji 😂😂😂

  • @maguettediouf5538

    @maguettediouf5538

    4 жыл бұрын

    Wagni woul

  • @birahimsene3781

    @birahimsene3781

    4 жыл бұрын

    Yaw dofgua

  • @brahimiba1460

    @brahimiba1460

    4 жыл бұрын

    Dangua soxor rk mais massa

  • @Anita-vh2kh

    @Anita-vh2kh

    2 жыл бұрын

    Ablaye sarr mane dehh damaaa diomii sii mère biiii momm faté sakh allah moy immensité yonente bi psl xamoul sakh secret wam yeup mom mouni mame cheikh mo ndieuka xam yallah 😒😒😒😒😒soubhannallahh

  • @sideuglayedokhbambapoint6022
    @sideuglayedokhbambapoint60224 жыл бұрын

    Kén dou dieukeurou gor yalla yi koulou khoume nak

  • @moiiza10sidibe30

    @moiiza10sidibe30

    Жыл бұрын

    Khana sa dieukeuro baye la domaram

  • @ousmanediop4960
    @ousmanediop49604 жыл бұрын

    Sente serigne touba rek ak cheikh Ibrahim fall

  • @youssouphgoudiaby1603
    @youssouphgoudiaby16034 жыл бұрын

    Machalla

  • @mortallagning3653
    @mortallagning36534 жыл бұрын

    Chékhe ibra fall kéne d'où môme wérna

  • @fatimataba3668
    @fatimataba36683 ай бұрын

    Soubhanawathallah Que Dieu nous pardonne AMINE Ya Rabbi

  • @miguelmiguel7128
    @miguelmiguel71284 жыл бұрын

    On ne sait pas encore qui est vraiment Mame CHEIKH IBRAHIMA FALL la porte du mouridisme et on veut connaître Celui qui est derrière la porte (Mame CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIMOUL RASSOULOU)

  • @thiamomarthiam8048
    @thiamomarthiam80484 жыл бұрын

    Mame ckheikh ibra fall moy naye goor leup fall dieureudieuf💪💪💪

  • @dembafall2230

    @dembafall2230

    3 жыл бұрын

    A yawdé défguako djiguén moy nday gua wakh😅

  • @metahgueye6233
    @metahgueye62334 жыл бұрын

    Machallah chiekh Ibrahim Fall ponit

  • @amossarros9820
    @amossarros98204 жыл бұрын

    Yen gni dingate thi commentaires yi dengene oumpale rek waye kou dingate cheikh Ibra fall ba fatou amoul mbidef boula meuna ramou ak ko meuna done laway bilahi walahi wa tahali mandoulen thi mbirou cheikhera fall wa salam

  • @syllayoussouf4649

    @syllayoussouf4649

    4 жыл бұрын

    Y'a meuna fenne khana cheikh ibra yallah leu wallah yonente il na rien fait pour l'islam boulen niou sonal way.

  • @amossarros9820

    @amossarros9820

    4 жыл бұрын

    @@syllayoussouf4649 limou done sa guinaw khelou baye sakh menouko kham wakhoul iow sen khol dingen dé domeram katal sa ndeye feule

  • @moustaphafall7444
    @moustaphafall74443 жыл бұрын

    Bayi len feen yi cheikh ibra amoul daara fa YALLA koudoul diouli do wor YALLA fa le wou la ragal len sounou BOROM

  • @lamtelafrikain9773
    @lamtelafrikain97732 жыл бұрын

    Jéréjéé Mame Borom Touba ! Jara AMM Mame cheikh y'ibreu fall ABBO RiDIAL

  • @fallougueye5424
    @fallougueye54243 жыл бұрын

    Dieureudieuf mame chiekhe ibrahima fall

  • @abdoukhadrendiouck1610
    @abdoukhadrendiouck16104 жыл бұрын

    ❤️❤️❤️

  • @jj-mg9tc
    @jj-mg9tc4 жыл бұрын

    Thièy Mam Cheickh Ibrahima Fall Kènn dù môm, nul ne peut l'imaginer non plus. Yalna Yallah Tass ñu si Bärckë.

  • @pascalwoulandiaye786
    @pascalwoulandiaye7864 жыл бұрын

    Kén dou cheikh ibrahima fall bilaye

  • @arfangmalickkane881
    @arfangmalickkane8814 жыл бұрын

    Machallah

  • @waguifaye8279
    @waguifaye82794 жыл бұрын

    Machala 🙏🙏🥺

  • @mamemor4720
    @mamemor47204 жыл бұрын

    💯💯💯💗💗💗💗

  • @PapaDiallo2
    @PapaDiallo24 жыл бұрын

    ♥️♥️♥️

  • @meujnatdiakhate8470
    @meujnatdiakhate84704 жыл бұрын

    Akassaa

  • @fatoumatasoumare7631
    @fatoumatasoumare76314 жыл бұрын

    04:15 confirme ce que Mame cheikh dit sur lui

  • @kingba1842
    @kingba18424 жыл бұрын

    Beaucoup de versions ˋ`Yalla yabouma ´´soubkhanala nagnouye layale sougnouye Kilifas si khame khame

  • @nancybousfallou1487
    @nancybousfallou14874 жыл бұрын

    Mame cheikh ibrahima fall yabari dolei koula khamoul.rek molay dikant fall koula guemoul douguou adiana

  • @oumarmbodj9296
    @oumarmbodj92962 жыл бұрын

    Allahoumdoullilah dieux merci

  • @abdoulayesall5020
    @abdoulayesall50204 жыл бұрын

    Nice❤

  • @nassthiam5831
    @nassthiam58314 жыл бұрын

    Lahilaha illala

  • @alphadiodiallo2362
    @alphadiodiallo23624 жыл бұрын

    Dû n’importe koi on vous manipule wallahi li bokoul si l’Islam ay ponkal togue si télé Bi di féne di sossal chéra fall ak Ahmadou Bamba rek chiip

  • @cheikhgueye341

    @cheikhgueye341

    4 жыл бұрын

    Amal Talibé mo geune Bo geumoul nga zappé bagna setane c mieux d'insulté Rew nga trop

  • @damzdiaw9793

    @damzdiaw9793

    4 жыл бұрын

    Cheikh gueye dague bakh rke diwax ak ki

  • @fatoumbaye7120

    @fatoumbaye7120

    4 жыл бұрын

    Sokhor baxoul

  • @practicemakesperfect3998

    @practicemakesperfect3998

    4 жыл бұрын

    Sakoul talibé rew ngua ndm trop

  • @mouhameddiouldediallo
    @mouhameddiouldediallo4 жыл бұрын

    Fénne késsé késsé gnaï déff lingay wakh tégouwoul fénne

  • @toubatouba4966

    @toubatouba4966

    4 жыл бұрын

    Nite Lou mou khamoul da si wara nopii

  • @maimunasonko7473

    @maimunasonko7473

    4 жыл бұрын

    Chi yone. Geumal linga geum rek, teh nopi 🤫🤫🤫

  • @maguettediouf5538

    @maguettediouf5538

    4 жыл бұрын

    Mbiroum baye fall koussi khamoul mandou si

  • @kairesaye8749

    @kairesaye8749

    3 жыл бұрын

    Yaw iblice mogane ligah yakar lep

  • @astoufall2345
    @astoufall23454 жыл бұрын

    Pape faye❤❤❤👍

  • @rocksarr9205
    @rocksarr92054 жыл бұрын

    Diarama Mame Cheikhra Fall. Dou kéne dou kéne té kéne dou mome

  • @oumoudiop3280
    @oumoudiop32804 жыл бұрын

    They mame Cheikh

  • @malickniang5137
    @malickniang51374 жыл бұрын

    Diarama Mame cheikh Ibra fall

  • @amsdestv703
    @amsdestv7034 жыл бұрын

    Aÿ sétal yalla si lingay wax soxnasi

  • @jj-mg9tc
    @jj-mg9tc4 жыл бұрын

    Arrêter de se plaindre aux autres, seul ceux qui ne savent pas place de mauvaise trucs sur les être. Dieu a dit: ne parle jamais au fait des autres anormal si tu es un bon croyant

  • @salmaneseck8637
    @salmaneseck86374 жыл бұрын

    c est vraiment grave senegal... je nai jamais pense que ceci existe au senegal..

  • @willymadjiguenediop8623
    @willymadjiguenediop86234 жыл бұрын

    Sama Sopé by mashallah kén d'où cheikh Ibra

  • @dionealioune2722
    @dionealioune27224 жыл бұрын

    Sokhna kiné mala beugue way

  • @ousseynoufall5004
    @ousseynoufall50044 жыл бұрын

    Kéne dou MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL

  • @ibiz4ever
    @ibiz4ever4 жыл бұрын

    Toumaal goor yalla ndax beug doff bou daanou mayla xaalisss tchim. Mame Cheikh mossoul wax wax djiii. « Serigne Touba moma jaaxal wayeijh Yalla yabouma. Lima xamal yalla soumako waxeih niou yapko. Mouni cheikh Ibra neubeul secret bi » Soubhanallah jaam mooy soutouraal yalla Walla yalla mooy soutoural jaam? Bayyileen GOOR YALLA yi ngueen di sossal ndax deureum

  • @daoudasarr5776

    @daoudasarr5776

    4 жыл бұрын

    Wakhe dégue dégue la lathie

  • @mouhamedthm915
    @mouhamedthm9153 ай бұрын

    Yonenté geun thi mbindef daf dane woor di dioulli , Yalla waxoul kén si Alkhurane boul woor boul dioulli

  • @omarkondjira2341
    @omarkondjira23414 жыл бұрын

    Skeey😘😘

  • @boussobaligaye4509
    @boussobaligaye45094 жыл бұрын

    Doyna war lou yalla tégui loul Seydina Mohamed SAW geun gui mbidéf mba dinako ko teguil kenen...ma dama diomi legui si soss yi gnou khewal si plateau yi dou degue khala lahou dou degue khala rassoul sama serigne rk té gniy def émission diné gnoroulén ben yon

  • @cheikhgueye341

    @cheikhgueye341

    4 жыл бұрын

    Lo khamoul neutre si c mieux

  • @dembadioum1868

    @dembadioum1868

    4 жыл бұрын

    Yaw mandoul té nopi

  • @ibrahimambaye2302

    @ibrahimambaye2302

    4 жыл бұрын

    Seydina Mohamed yalla mayone seydina Omar loumou mayoutone mouhamed té yonénet bi moko gueuneu kone nopil

  • @mariasant3937

    @mariasant3937

    4 жыл бұрын

    Soit intelligent. Sou Yalla teggil wone Rassoul diouli kène dotoul diouli kone le voyage nocturne d'où âme ndieurigne. Kou niaw ndiort ni yalla meunoul teggil Cheikh Ibreu diouli cep nga katanou dougnou borom. Yalla MO sagn lepp meune lepp d'ara teuwou ko soko xamé nopalou

  • @damzdiaw9793

    @damzdiaw9793

    4 жыл бұрын

    Koussi monta wakh lu bax nagua si manu

  • @gagnembaye8585
    @gagnembaye85854 жыл бұрын

    nite daye mandou thieuye chikhe ibra fall kimane la

  • @awaseydi7023
    @awaseydi70234 жыл бұрын

    KO xamoul Aÿ mbireum = mandou diara amm mame cheickh ibra fall

  • @Aicha_TV_OFFICIEl
    @Aicha_TV_OFFICIEl4 жыл бұрын

    Talibés serigne abdoul Karim mbacke fière d'être musulmans est mourite👌👌👌👌🇸🇳💖💗👌👌👌

  • @bmtv-zb5xl
    @bmtv-zb5xl2 жыл бұрын

    Ndeysan ken d'où Mame Cheikh Ibra Fall lAMP Yoon Wii

  • @yakhyakafando5903
    @yakhyakafando59034 жыл бұрын

    Sokhna kiné doundale yagu Baxx dieureudieuf

  • @mamethiernodiop7392
    @mamethiernodiop73924 жыл бұрын

    Dieuredieuf

  • @morseye1851
    @morseye18514 жыл бұрын

    💖💖💖👍

  • @sarrabdou3040
    @sarrabdou30404 жыл бұрын

    Bilaye yaye boy mala beugeu trop. Dafa diara lèrall...moy dieukeur rou goor gñiii

  • @mbt.officieltv5052
    @mbt.officieltv50524 жыл бұрын

    Kou kham loutakh c ibra fall dou diouli dou woor namako wakh madolile lasi dara bilahi

  • @rastablondy4656
    @rastablondy46564 жыл бұрын

    Sope Mame cheikh ibra fall jusqu'à ma mort

  • @diopmomo329
    @diopmomo3294 жыл бұрын

    Sokhna si yamana doul rk ngaye df ay mouride yoo khamni doul rk 😂😂😂

  • @brahimiba1460

    @brahimiba1460

    4 жыл бұрын

    Yaw mandou wo moridoulahi mofi né

  • @TamsirSeye
    @TamsirSeye Жыл бұрын

    Diarama Mame cheikh Ibrahima fall lamp

  • @senesaliou4111
    @senesaliou41113 жыл бұрын

    machala

  • @modouthiam9357
    @modouthiam93574 жыл бұрын

    Louway khamoul boulsi dougou Kouy diouly sa compte la dieum Gua wor sa compte la dieum Legui kaay manou len si rk

  • @dallasboubayekarim5423
    @dallasboubayekarim54234 жыл бұрын

    Diarama mame chiekh ibrahima fall lamp ❣❣❣❣❣❣❣🙏

  • @serignemorgueye7575
    @serignemorgueye75754 жыл бұрын

    😭😭

  • @boypikine5856
    @boypikine58564 жыл бұрын

    Les 5 piliers de l'islam: Chahada- La prière- la Zakat- Le Ramadan- le Hadj...tout musulman qui prétend ne pas s'acquitter à une de ces obligations🙈🙈 je ne pourrais pas le qualifier moi...Expliquer moi chers camarades je suis un peu perdu...

  • @songboy5305
    @songboy53054 жыл бұрын

    Ahhhhh Sénégal mo nekh ay fen rek

  • @diopcheikh8936

    @diopcheikh8936

    4 жыл бұрын

    Bayill tong koubakh

  • @falloundiayendiaye8467

    @falloundiayendiaye8467

    4 жыл бұрын

    fén yi dé molay ray di dage sa kholl ba yaw mal ghiyam

  • @falloundiayendiaye8467

    @falloundiayendiaye8467

    4 жыл бұрын

    bo sa nion nougoy fénal sa bay

  • @fatoukane9864

    @fatoukane9864

    4 жыл бұрын

    astafourilah yaw mi

  • @madyanatv6713

    @madyanatv6713

    4 жыл бұрын

    Wakh KO baye

  • @assanekoundou1201
    @assanekoundou12014 жыл бұрын

    Aÿ sama yaye fall

  • @yakhyakafando5903
    @yakhyakafando59034 жыл бұрын

    Lou waye am dieul té guén baniokk Lou niou yore waw goor

  • @fatoumbaye7120
    @fatoumbaye71204 жыл бұрын

    Baboul mouridine mo diakhal gayi ,Cheikh IBRA rek

  • @olypibrahim5052
    @olypibrahim50524 жыл бұрын

    Senegalais soko beuguer xam rk liral commentaire ...Mandou la Yalla geuna beugue té nioune gni nieupe ken mandouwoussi kii limi wax mom cree wouko Cheikh ibra fall moko Wax té ay waxii cheikh ibra fall soko Wédé alkou soko gueumé dof , Nena Degg lem té dem.

  • @yogranada480
    @yogranada4804 жыл бұрын

    😭😭😭🙏🙏🙏🤲