FADAM APPORTE DES ÉCLAIRCISSEMENTS «Bimay wo LAHAT ak aziz li la guissone… »

Ойын-сауық

Bantamba tv. Km 2,5 Boulevard du Centenaire de la Commune de Dakar.
tel : 33 825 34 36 - 77419 03 64

Пікірлер: 48

  • @mouhamadoubambandiaye478
    @mouhamadoubambandiaye4785 күн бұрын

    Fadam defar rk mola takha diouk ❤

  • @sellediop1817
    @sellediop18175 күн бұрын

    Merci fadam❤❤❤

  • @user-dy1kt7dk3n
    @user-dy1kt7dk3n5 күн бұрын

    Dieureudieuf Fadam ❤

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar95484 күн бұрын

    Merci fadam

  • @khalifamboup5646
    @khalifamboup56464 күн бұрын

    il faut payer les lutteur mais thiatou yarakh na accepté té bou mou indii bén supporter prommotteur yi ay immmebile laniou

  • @waxkatoudeug
    @waxkatoudeug4 күн бұрын

    Du moment qu'un contrat a été signé en bonne et dû forme, chacun n'a qu'à respecter les termes du contrat qu'il a signé. C'est aussi simple que ça !!

  • @fatvmanjak1703
    @fatvmanjak17035 күн бұрын

    Bonjour bantamba tv voyre plateau est exeptionnel mais vos écran faut les decent un peu juste qu'on puisse voir ce qu'il affiche cest important...

  • @momoseck1617

    @momoseck1617

    3 күн бұрын

    C'est pas important

  • @zakariasarr2257
    @zakariasarr22575 күн бұрын

    Mai thiate yarakh, naka la meuna lebe 10 million te niou fay Co 2 million par comba si 3 comba

  • @h.m.d5865

    @h.m.d5865

    5 күн бұрын

    Wakhoul deugg D

  • @sewroumbengue8213

    @sewroumbengue8213

    4 күн бұрын

    C bien possible même quelqu’un qui perçoit environ 500mil il peut avoir un prêt de 10miliom wakhouma ak kouy fayékou 2milion

  • @abdouazizthiaw3491
    @abdouazizthiaw34914 күн бұрын

    Fadeur ak Badola ñu jara bayi xél la ñu. Dina ñu yaax lu bari ci digënté mbër yi ak promoteurs yi..waxu seytané rékk la nuy wax..ame na lo xame né kénn waro ko wax ci plateau..

  • @mamadousow8935
    @mamadousow89355 күн бұрын

    Mais fadam temps yi biir reuy neu dhee foumouy demé nonou 😂

  • @user-yl7ey6wn5m
    @user-yl7ey6wn5m5 күн бұрын

    Senegalais khamoul contract liko nèkh la kham mais boye bi dafa wara beurè nagnou wakhatè deug

  • @abdoulayekane3231

    @abdoulayekane3231

    5 күн бұрын

    Deug nekhoul dafa wara beuré bouko defoul na cng def liguéyam sénégalais affairou sentimental Moko Nekh wadji signé contrat d’accord ci therme contrat bi ñeuw ba final di dof doflou

  • @mamadousene3731

    @mamadousene3731

    2 күн бұрын

    Bilaye ya wakhe deugue

  • @user-mq8oo2bx5q
    @user-mq8oo2bx5q4 күн бұрын

    S’il a signé un contrat, il n’y a plus de débat. 2 millions mom Ndaw ne mais combien il avait avant? Il peut essayer de renégocier mais pas par la force. Goor = Kadou. Té Yalla ne daan.

  • @ToureSerigne-bv3rh
    @ToureSerigne-bv3rh5 күн бұрын

    Fadam Say wakh dara lérou si

  • @ibradiop7209
    @ibradiop72093 күн бұрын

    Fadam dafa soff trop Doull rk la man bilay

  • @AssaneFall-eh2tz
    @AssaneFall-eh2tz5 күн бұрын

    3 millions da ndaw si finalou claf

  • @h.m.d5865

    @h.m.d5865

    5 күн бұрын

    Moko wakhalé moko ladje niou fay koko

  • @moustaphawade8094
    @moustaphawade80944 күн бұрын

    En tout cas conclusion bima meune tirer moy contrat daniou koy respecter si les deux camps acceptent les contrats bien avant donc daniou beurei force même si c 1 millions

  • @petitpapadiallo4227
    @petitpapadiallo42274 күн бұрын

    Merci ils ont arnaquer led lutteurs

  • @FallouSamb-tv
    @FallouSamb-tv5 күн бұрын

    Linou lene di faye dafa nda trop me tioutou na beurre meun na dane cou ne

  • @babacarsall5349
    @babacarsall53494 күн бұрын

    Fadam Doudou Sané dou sérère Djola la

  • @magueyembengue2980
    @magueyembengue29805 күн бұрын

    Menaseram moko signe amoul lougnouy wakhtane da wara beure

  • @user-by1vj4sp5g
    @user-by1vj4sp5g5 күн бұрын

    Babacar es tu as bien lu le contrat

  • @magueyembengue2980
    @magueyembengue29805 күн бұрын

    Delene wakh deug thiatou yarakh bou beugonee wakhtane dou guene sì Media di wakh

  • @MANGASSAthiaroyemer2499
    @MANGASSAthiaroyemer24995 күн бұрын

    LAKHAT. NDIAYE. DAFA. SOKHOR. TROP. BOUDOON. BAAYAM. MOY. BEURÉ DOUKO. NANGUOU

  • @gorguidieng7796
    @gorguidieng77964 күн бұрын

    Problem d'où contra tiate bamou dané sa première réaction la wakh beuré woul ak doudou sané

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5uc4 күн бұрын

    Wadji nama yalla moussal si mom mais mélokane seytané deug la yoré diko bimou yoré la geuna ragal si domou adama

  • @user-by1vj4sp5g
    @user-by1vj4sp5g5 күн бұрын

    Bour dagua dioum nakari dounder nekha dewer

  • @IbrahimaThiongane-wb6qs
    @IbrahimaThiongane-wb6qs4 күн бұрын

    Pourquoi cng di khoti licensame cng nagnou reglè

  • @princelaye8210
    @princelaye82105 күн бұрын

    Vraiment ce lahat et makan dagno sokhor nane nguéndi fayyé boy yii donne beurré claf bii ay 2 millions walla 3millions au moins nguéne faye léne chaque combat 7 walla 10millions mé ce lahad est mauvais di doundé derréttou boy yii reek. thiatou yarakh sougnoulla fayoul 15 walla 20millions boul beurré

  • @morseye4084

    @morseye4084

    4 күн бұрын

    Sawaye ndiaye tine 1 millions 700 lagnouko Fay gni bakhougnou bilahi

  • @abdousylla6390
    @abdousylla63905 күн бұрын

    Bour guéweul lèkeu khaliss bou haram defoula dara Limi wakh dara doussi deugue

  • @AboubacarSadikhDiop
    @AboubacarSadikhDiop4 күн бұрын

    Exploitation c'est pas un contrat

  • @user-zt1tv7zg7h
    @user-zt1tv7zg7h5 күн бұрын

    Lahat ay nit youy doundou si nit lagnouy serr bou bone la doff

  • @FallouSarr-
    @FallouSarr-5 күн бұрын

    Bour nopil yaw Lou nekh promoteur yii rek ngay wakh heureusement keneu deglou woula boy wakh di melni kouy wakh ci dinee. Thiatou yarakh yakaroul ci lamb pour survivre yaw nak ci lamb ngay dieulee dépense boy bi beurewoul c tout

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv5 күн бұрын

    Mane d burr bouy wax daamakoy avance 😮

  • @daoudadia3631

    @daoudadia3631

    4 күн бұрын

    Soff la def té dou dara dey handiou rk

  • @mamadousarr3371
    @mamadousarr33715 күн бұрын

    Fadam2 yow askanou sérére mosou nio niake champion tapha tine siteu lan 2000 ablaye ndiaye youssou ndour neko rele thiaka faye ordinateur pakala faldo dou diékh liam moy mberou sérére boufi dan danat kene doula nago diel khana gris2 mome moy nango bere ak mberou sérére yi geso doudou sané moungui ni thiatou yarakh bagn ne dou bere ak mome niom youssou ndour fondé sarr souper étoile...ak ak motakh niou touki gene réwmi niefi neke manoun am combat lan 2000 champion thiaka faye neko rel faldo...😭

  • @abdoulayekane3231
    @abdoulayekane32315 күн бұрын

    Senegal dafa Nekh quoi , toujours dans le sentimentale!!!!! Nit kou signé contrat d’accord ak prix bignouko Faye dém ba final di dof doflou…. Un contrat c’est un contrat bou beuréwoul na cng def liguéyam

  • @elhadjidiagne5201

    @elhadjidiagne5201

    5 күн бұрын

    waxal loula leer contrat bi thiatou yarakh yor 3combat kase mothi nek yen loula arrange rek nguendi wakh khana thiatou yarakh beugoul dara finale claf 3milions foum am

  • @abdoulayekane3231

    @abdoulayekane3231

    4 күн бұрын

    @@elhadjidiagne5201 Mais dimabar deugueur nga fit dhh becaye néna defna enquête ci cng ñounéko contrat biñou yoré boy bi da wara beuré final c’est signé yaw nga beugko layal…..3 millions da ndaw wala ndawoul mom ak manageram ñoko signé da wara beuré moko nangou bouko défoul nañou khoti licenssame li chantage la!!! Y’en ci sentimental ngen tollou nit nak boko beugué dangkoy deug

  • @petitpapadiallo4227
    @petitpapadiallo42274 күн бұрын

    Merci fadam

Келесі