elle construit sur notre propre terrain, j'ai mon titre foncier "Pourquoi ils cachent leurs visages"

elle construit sur notre propre terrain, j'ai mon titre foncier "Pourquoi ils cachent leurs visages"

Пікірлер: 44

  • @babacar1289
    @babacar1289Ай бұрын

    Bilay madame ndir damakô yeureum vraiment yangui takhawou sa dieukeur ci alalame yalnaléne yalla diaplé ba géune ame ndam inchallah

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Billaye yalla bakhe na amouma koudoul sama borome keur donc ni rek la meuna deff tee li moye sama wareff en tout cas merci bcp pour le soutien ça nous touche énormément

  • @awandiaye161
    @awandiaye161Ай бұрын

    Thieuye Senegal Gnoune gni neke europe ,YALLA nagnou Yalla samale sougnou alale yi neke Senegal

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Allahouma Amine gniouye aye diambarr nak yalla doli takhawoulene

  • @mariegueye6043

    @mariegueye6043

    Ай бұрын

    Amine

  • @xadimmbaye6196

    @xadimmbaye6196

    Ай бұрын

    Amine investire deee bagne feu geudjj

  • @aissatoundiaye8887
    @aissatoundiaye8887Ай бұрын

    Bon courage Madame Ndir, na yone def liguéyam si lou gaw parce que les prédateurs fonciers ne devraient plus faire la loi au Sénégal. In shaa Allah légui mou diekh, comme séen droit de renvoi diekhna légui léep léer.

  • @lissarassoul861
    @lissarassoul861Ай бұрын

    Khady Diagne mi nekoul si deugg mai yalla la eupp dolei

  • @user-gw8qv9zg5b
    @user-gw8qv9zg5bАй бұрын

    Kouy tabax fi Khady Diagne xana bayam moy rakou yallah li dafa yombeu torop na thi état bi wax genre yi mo tax niou niaff wa APR thia xadji 😢😢😢😢Massa Madame Ndirr yag yag yay am ndam deug rék moy moudiou 😢😢😢

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Merci bcp du soutien khadi Diagne dee waye mogui nonou rek xamouma boumou done sathie mou teuthe wayee d'où bii dee

  • @NdeyeSeck-vm3xs
    @NdeyeSeck-vm3xsАй бұрын

    Il faudrait que la DIC mette aux arrets cette voleuse de Ndeye Khady Diagne. Elle est connue des faits pareils et a fait souffrir bon nombre de proprietaires.

  • @omarsall9821
    @omarsall9821Ай бұрын

    Antoucas boul bayil mou sedd dei😮😮

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Billaye douma meuseu bayi insha Allah sene message yi c'est réconfortant ❤

  • @omarsall9821

    @omarsall9821

    Ай бұрын

    Nous sommes tous avec toi bilakhi li dafa niaw thi Senegal

  • @ametecisse8580

    @ametecisse8580

    Ай бұрын

    Nn degue day am ligui kay

  • @ahmadoudiagnegueye9918
    @ahmadoudiagnegueye9918Ай бұрын

    Tothie len keur gui mou diékh

  • @maximemendy8958
    @maximemendy8958Ай бұрын

    Ces arguments sont plus cohérent, dina ame justice

  • @kartoumsakho6772
    @kartoumsakho6772Ай бұрын

    Madame boum bayi mou seed parce que lingay wakh mo gueuneu yenou mana

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Merci du soutien ça nous touche énormément

  • @alainhyacintheadomou2886
    @alainhyacintheadomou2886Ай бұрын

    Du courage les gars, aller jusqu'au bout

  • @ahmadoudiagnegueye9918
    @ahmadoudiagnegueye9918Ай бұрын

    Bilahi borom keur gui amoul foula do dem loué bill nieuw danél ndeye keur gui niou soga dem si yon

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Aye yawe boule wakhe lolou meunou niou nieuwe rek tothe keur gui deuk bi dafa âme yone aussi ndawe sii lolou leu beugeu pour gniou deloko limou fi deff

  • @ahmadoudiagnegueye9918

    @ahmadoudiagnegueye9918

    Ай бұрын

    @@zeynaboudiop8278 mai bobou ba legui mingi dem si yon amoul beneu résultat il faut mou am bruit yon soga diauk si li

  • @mamegorseye6131

    @mamegorseye6131

    Ай бұрын

    Kii tabac lii dall da am gunaw mo tax mou déff lii bou yabo nak khéx bii saff mondiale bou yabo nga nieuw cassamace diakarlo wadji du nala diox sa alall far force gua yii nii la niouy déff du nangou souff diambour yii ba parré défarall la sénégal méttina

  • @ametecisse8580
    @ametecisse8580Ай бұрын

    Nn diomay dfa wara changé les responsables des discos

  • @ametecisse8580
    @ametecisse8580Ай бұрын

    Mais. Sénégal mou bari bandit foncier

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Ki môme dathi bolée deugeur fitt wayee yalla bakhe na

  • @julesleontiendrebeogo2270
    @julesleontiendrebeogo2270Ай бұрын

    Han kone fii la cas bii tolou 🤔

  • @IbraSarr-ms2sk
    @IbraSarr-ms2skАй бұрын

    Dou dara soudoul réwandé nakala nga fekk terrain diaabour diko tabakh té amo benn keuyit.

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Billaye sonale naniou Witt Khadi Diagne mii

  • @IbraSarr-ms2sk

    @IbraSarr-ms2sk

    Ай бұрын

    @@zeynaboudiop8278 wayé boulenn mosa khaddi dakh loolou la beugue motakh mouy proposé inchallahou rabbi diguen am thie mom ndam.dakh amatoul protection.

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Geume n'a lolou nake

  • @morganmor1904

    @morganmor1904

    Ай бұрын

    Yaw Loula woor terrain diambourla ayway anni madou

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    @@morganmor1904 terrain diambour la kaye ndakhe seni borome gniogui ni né diomou diomarale

  • @aidafaty4711
    @aidafaty4711Ай бұрын

    ❤❤❤❤je voudrais rencontrer la journaliste

  • @ndiolethiam1756

    @ndiolethiam1756

    Ай бұрын

    Pourquoi

  • @user-cn6ed6ik7c
    @user-cn6ed6ik7cАй бұрын

    De vrais délinquants..

  • @abdoulcamara7924
    @abdoulcamara7924Ай бұрын

    adouna daye beugue touki

  • @user-mw2bd9eq5e

    @user-mw2bd9eq5e

    Ай бұрын

    Tokina depis 2012 bi macky sall neke ci rewmi

  • @aboudione7672

    @aboudione7672

    Ай бұрын

    Toukinna bouyaag nio bagne rek

  • @diawaida759
    @diawaida759Ай бұрын

    Khady diagne en tout cas elle est louche😡😡😡 bon courage Mme Ndir🙏

  • @diagnemomo4771
    @diagnemomo4771Ай бұрын

    Yaw la geum liga waxx Familles mbégue lou taxx sén visage fégnoul Naniou bayi yi

  • @zeynaboudiop8278

    @zeynaboudiop8278

    Ай бұрын

    Billaye ma Khadi Diagne dafma yemeuu Mane neubeutouwouma lakatouwouma wayee bi môme dinako bayi par A ou B

  • @user-mw2bd9eq5e

    @user-mw2bd9eq5e

    Ай бұрын

    ​@@zeynaboudiop8278antouka li gnawna ci rewou dioulit lá dra rafetoci diaye dolle alalou adouna diarouli

Келесі