ÉDITION SPÉCIALE SUR KÉMITISME ORIGINE ET DÉMARCHE || OustazMorKébé ||

Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
/ @senegal1
Le but AlQurann et Sunnah est de participer à la transmission du message islamique dans toutes sa clarté et son authenticité

Пікірлер: 43

  • @user-ui2rk6mq9w
    @user-ui2rk6mq9w4 күн бұрын

    Yalna yalla samou alxouran ak sounnah samou oustas mor kébé

  • @qadrbrotherdiagne1491
    @qadrbrotherdiagne14914 күн бұрын

    OUSTAZ MOR KÉBÉ MI MASHALLAH KOU AM XAM XAM LAH NI LAH OUSTAZ YI FI NÈK WARA MÈL XAM XAM NI ADOUNA BI DI DOKHÉ SI ZAHIR ,XAM XAM SAY SAY YI LEMBÉ ADOUNA BI "SIONISTES" YI DOMOU ADAMA SOU BAYI YÈP TOP YALLA KÈNAL KO RÈK ALKOU.

  • @aboubacrysow510
    @aboubacrysow5108 күн бұрын

    Assalamou aleykoum wa rahmatoulah

  • @siacamane3361
    @siacamane33617 күн бұрын

    Longue vie a vous ✊ au senegal ✊ ya oustaz ✊ kebe ✊

  • @senegal1

    @senegal1

    7 күн бұрын

    Amine ya rabbi

  • @Eleveurmouton
    @Eleveurmouton8 күн бұрын

    Merci beaucoup 🙋‍♂️

  • @senegal1

    @senegal1

    7 күн бұрын

    Merci à vous

  • @khalifaababacarbodiang6008
    @khalifaababacarbodiang60088 күн бұрын

    Manchallah

  • @biboujemeh5739
    @biboujemeh57398 күн бұрын

    ❤❤❤

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane70666 күн бұрын

    جزاك الله خيرا يا شيخ ❤❤❤❤

  • @ahmaddia3315
    @ahmaddia33158 күн бұрын

    ما شاء الله وجزاك الله خيرا يا اخي الكريم أستاذ موركب❤❤❤

  • @senegal1

    @senegal1

    7 күн бұрын

    Amine ya rabbi

  • @ThomasSankara-lz4gs
    @ThomasSankara-lz4gs8 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @azizndiaye9995
    @azizndiaye99956 күн бұрын

    Oustage mor Kébé toujours pertinente

  • @khalifaababacarbodiang6008
    @khalifaababacarbodiang60088 күн бұрын

    Très intéressant

  • @alassaneseye2191
    @alassaneseye21917 күн бұрын

    Machalah dieuredieufe oustaz mor kebe leral yi amna solo yalla na la yalla faye billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla sam te arla

  • @senegal1

    @senegal1

    7 күн бұрын

    Amine ya rabbi

  • @ibrahimatanordiallo1382
    @ibrahimatanordiallo13824 күн бұрын

    Hafizahullah

  • @SaliouSeye-up4uy
    @SaliouSeye-up4uy7 күн бұрын

    Machalla jërëjëf ustaas

  • @abdoulmadjideaydara2297
    @abdoulmadjideaydara22977 күн бұрын

    Maallah amna solo👏👏👏👏

  • @bocomaladi7000
    @bocomaladi70007 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdoulaye6441
    @abdoulaye64417 күн бұрын

    Laïcité ak République fi si Sénégal dioulit yi nioko gueneu gueum niou doul dioulit ba gathie Walleu niaka xam wessou woul ba ay Imam fi niokoy défendre

  • @ibrahimabalde1234
    @ibrahimabalde12347 күн бұрын

    Machallah

  • @dialloamadou1905
    @dialloamadou19056 күн бұрын

    ما شاء الله يا استاذ جزاك الله خيرا❤ ❤❤❤❤❤❤

  • @senegal1

    @senegal1

    6 күн бұрын

    Jazakallahou khayrane

  • @LaayNjaay17
    @LaayNjaay177 күн бұрын

    Sëñ bi, di rafetlu gëstu. Waaye KEMIT du diine bay nekk diine ju bees. Afrig masu ñoo am diine, kemitisme manees naa wax ni PANAFRICANISME scientifique la. Afrig amul gëm-gëm (croyance)waaye xam-xam (savoir) moo fi am. Gëstug panafricain yi jëm ci xamtu (science ) ak xeeti xam-xam yu ni mel niki "anthropologie" moo yóbbu gëstukat yi ba Mbatit (diine) yi ñu gëm (islaam, Christianisme...) ci mbatitu Afrig la bawoo ca Esipt gu njëkk te mooy Afrig. Waxunu nag nit nay dellu ca yu bon ya sunu Maam yaa daa def, waaye yu baax ya sunu Mbatit (culture) amoon ak sunu xayte(civilisation) bi Nga xam ne ci àdduna sépp sukkandiku. • Adama baxam nit ku ñuul la woon. Nun Afrig xamunu Adama, waaye gëstu yi jëm ci anthropologie li mu saxal mooy nit ñi gëna yàgg seen yax Afrig lañu ko gis. Te ci wàllu BIOLOGIE nit manul bawoo feneen Fu dul suufu Afrig. Ki njëkk amal xayte (civilisation) teg ko ci xamtu (science) am sàrt bu koy "équilibrée" ñu naan ko MAAT nga naan ko baaxul. Di jëli culture araab bi, def ko diine, gëmloo ko ñépp, ku ci bokk àjjana ku ci bokkul safara, di nappee Africain yi. Lii moo waral kemitisme, du diine waaye doon Africain la tey sàmm li baax ci Afrig. Du leneen.... Laay Njaay ✍🏿

  • @alioubarry2157

    @alioubarry2157

    7 күн бұрын

    C soit t’as pas bien compris le kemitisme, soit tu refuses d’accepter la vérité 🤷🏻‍♂️

  • @abdoulaye6441

    @abdoulaye6441

    7 күн бұрын

    Anthropologue yi werentou wouniou ni Adam niit kou nioul leu won Musa Souleymane dou niit kou wekh ni niit kou nioul Niit kou nioul mo niekeu si Aduuna diine Adam moko niekeu andi

  • @bikw2748

    @bikw2748

    7 күн бұрын

    Laaj njaay kaddu yi am na solo, di la ci jaajëfal.

  • @aladjidiaoune2421

    @aladjidiaoune2421

    7 күн бұрын

    @@abdoulaye6441dinné dou afaire de peaux nite kou gnul ak kou wéhk yeup pas yam koussi diamou yalla séllaleko douguou adiana kouko wéddi ba déssi douguou safara

  • @OusmaneDg-xt7ns

    @OusmaneDg-xt7ns

    7 күн бұрын

    Ta rien compris kefeur la

  • @Baaissatou-ph2xo
    @Baaissatou-ph2xo7 күн бұрын

    Coumaye diokh numero oustaz

  • @zeinaniang

    @zeinaniang

    5 күн бұрын

    salam aleykoum attention à celui que tu as en photo de profil c’est un ikhwani il a même été en prison

  • @LaayNjaay17
    @LaayNjaay174 күн бұрын

    Deux de mes récentes commentaires sur ce sujet ont été SUPPRIMÉS. Laissez nous de donner notre point de vue comme vous l'avez malhonnêtement fait sur la tradition africaine.

  • @aboubacrysow510
    @aboubacrysow5108 күн бұрын

    Assalamou aleykoum wa rahmatoulah

  • @senegal1

    @senegal1

    7 күн бұрын

    Wahalaykoum salam warahmatoulahi