🔴[ DIRECT ] PLATEAU SPECIAL OUSTAZ CHEIKH AHMED TIDIANE NDAO l MERCREDI 22 MAI 2024

Ойын-сауық

Abonnez-vous à notre chaine.et Activer la Cloche, pour suivre en Direct les grands èvenements de l’Islam et de la Tidjaniya
#malikia #malikia #Tivaouane #maliiatv
LEERU MAODO ➤ Li Bienvenue sur la chaine de MALIKIA TV TIVAOUANE restez connecter!!!!!!!!!!! Aimez, abonnez, commentez et partagez...Merci restez connecter!!!!!!!!!!!

Пікірлер: 272

  • @seydinamohamedndiaye6690
    @seydinamohamedndiaye669026 күн бұрын

    Cheikh Ahmed tidiane Ndao ❤ leneu rek laye retenir ci mome..L’homme qui m’a fait connaître l’histoire de Moussa dé A a Z.. nhieupeuye dioum c’est tout

  • @ouztheman5792
    @ouztheman579228 күн бұрын

    Bravo PDG. C la première fois que je vous entend parler mais j’ai admire ta franchise. BRILLIANT!!!!!

  • @alassanethiam6870
    @alassanethiam687011 күн бұрын

    Cheikh Ahmad Tidiane ndao yalla nala yalla same ci barrke seidina Mouhamadu ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @sokhnafatimabous.mansoursy283
    @sokhnafatimabous.mansoursy28328 күн бұрын

    Oustaz CHEIKH Ahmed Tidiane Ndao yalna yalla sam léne Aar léne 🤲

  • @aminataseck7481

    @aminataseck7481

    28 күн бұрын

    Amine waye

  • @kanekiken9566
    @kanekiken956626 күн бұрын

    Directeur bi deugou na. Yalla nako yalla arr Finalement sama khol fekh neu yalla na yalla dimbali ouztaz ndao

  • @user-oe2bs4dk3s
    @user-oe2bs4dk3s28 күн бұрын

    Cheikh Ahmad tidjane ndao dafa dioume yalnaco yalla téggil li dale sa kawame . Té boussi guéné yalna boumeco défati ci barké cheikh seydil Hadji Malick Sy radiyalahou taala anhou wa ardahou wa ana bihi amine .

  • @khalioudrame9526

    @khalioudrame9526

    27 күн бұрын

    Kouleu wakh dafa dioum souko sonko defé nak? Ousmanensonko khamaloulene ko dara ..ay mbireum leroul.

  • @mouhamadtamourougueye387

    @mouhamadtamourougueye387

    27 күн бұрын

    ​@@khalioudrame9526yaw moom est ce que say mbir leerna ? Dioulite dou toumaal moroomou dioulitam. Limou wakh même soudone deug warouko wakh.

  • @ndeyefaye6835
    @ndeyefaye683527 күн бұрын

    Machalla oustaz cheikh tidiane diabarla vraiment défadioum

  • @black2krack982
    @black2krack98224 күн бұрын

    Je vois sur ce plateau l'Islam. Macha allah rafetna. Li ma japalone Iman gnep fatena ko daxx PDG. Merci

  • @DabaKebe-wg6dk
    @DabaKebe-wg6dk28 күн бұрын

    Kou bakh dafa dioume yalna ko yallah takhawou yalna léne yallah fay rafét na

  • @ababacarseckfaye7719
    @ababacarseckfaye771928 күн бұрын

    Machalah oustaze mactar ndiaye, c'est la première fois que je vous écouté mais vous incarner enseignement de el hadji malick. Vérité absolue

  • @user-xn3sz1zq3w
    @user-xn3sz1zq3w26 күн бұрын

    cheikh Ahmed tidjane ndao yalna yalla geuneu goudeul faname té dolliko wer barcké mame maodo 🤲 té yalla teguilko natoubi

  • @heutou_talibe_cheikh
    @heutou_talibe_cheikh28 күн бұрын

    Macha"allah el hadji makhtar ndiaye tu est tres véridique et direct dans tes propos

  • @Ndeyemarem-ux8iq
    @Ndeyemarem-ux8iq28 күн бұрын

    Cheikh tidiane ndao yalla yalla takhoul guir dioumy séydina moukhamét louma kham thi mom yawla

  • @bbfa864
    @bbfa86428 күн бұрын

    Macha allah PDG c'est très bien et très important ce que vous avez fait . La vérité c'est primordial et il faut rectifier le tire . La dermache est excellente djoulit nilay def . Nous sommes tous abasourdis de ce que a dit l'imam vraiment mais voyre posture est louable macha allah . Yalla na nek leçon pour nous tous si mandou, si rafetal ...nitt loumouy wouyo dakoy nourou...nous devont perpétuer notre statue d'exemple. Merci malikia❤❤❤❤❤❤❤

  • @groupenabiyetv8211
    @groupenabiyetv821128 күн бұрын

    KÉPOU KOUY OUSTAZ BAYABO NGA XAM YAW YAY KAN LI GEUN THI XAM XAM MOY XAMSA BOPPOU❤ TÉ NGÉN MOYTOU POLITIQUESENT YI OUSTAZ NAK DAFA DIOUM WAYÉ YALLA NAKO YALLA GÉNNÉ THI XAT XAT YI❤❤❤❤

  • @dioptalla755

    @dioptalla755

    27 күн бұрын

    Frr wakh nga lepp

  • @mansourdiagne1964
    @mansourdiagne196428 күн бұрын

    Sonko kouka songou sankou

  • @user-po7mt5bh9m

    @user-po7mt5bh9m

    28 күн бұрын

    Ku masa songu gaçca rék nga say jëlé

  • @mohamedgaye408

    @mohamedgaye408

    27 күн бұрын

    boulen sonal nite gni

  • @cheikhseck4760

    @cheikhseck4760

    22 күн бұрын

    Bayi lén doul Doul nguén ba yakkù

  • @PapethiateNiang
    @PapethiateNiang25 күн бұрын

    Macha alla pdc Makhtar ndiaye al Amine

  • @Dia88186
    @Dia8818626 күн бұрын

    Grâce à borom grand boubou bou maron bi❤❤❤j'ai abonné sur Malikia Tv🙏🙏🙏

  • @babs7555

    @babs7555

    25 күн бұрын

    On est 2 alors

  • @Dia88186
    @Dia8818626 күн бұрын

    Wakh deug yalla plateau bi Mature na❤🙏🙏❤

  • @cheikhseck4760
    @cheikhseck476022 күн бұрын

    Imam cheikh tidiane ndao yalla Nako yalla takhawù wayé yén WA malikya sen émission dara rafétou ci lii khawma Hein bingauén diapal imam la khawma loumou doon wayé niawna trop Amna mbétél bou REUY si yén yalla kham nako

  • @NiangLaye
    @NiangLaye23 күн бұрын

    Vérité absolue matare diagne merci mashala way

  • @ndawlislam7021
    @ndawlislam702127 күн бұрын

    Macha Allah malikia dèfe géne Yefou kilifa PDG mouhtar Ndiaye wahega wahou responsable diabote bou tognè hamakoni mo togne imame dioumena nite moye dioume té diègalouna yallah nako yallah diégale amine PM sonko yite yallah nako diégale imame dramé topouna mèrame dounonou thi aye dioulite kounè warega ame liga tanè sa morome adouna dou keur

  • @al-futiiyutv_TBD
    @al-futiiyutv_TBD25 күн бұрын

    Le prophète SAW a dit "Sa mboku, dé ko jappalé, ci bu tooňe ak mbuň ko tooňe" Merci PDG, vous êtes un homme honnête, franc et responsable. Puisse Allah vous protéger !

  • @oumarsow2035
    @oumarsow203528 күн бұрын

    Alhamdoulila doulila li rafét na trop manchala ❤️❤️❤️

  • @yacinediop1922
    @yacinediop192223 күн бұрын

    Salam Oustaz Ndao. Say preches jubanti lu barè ak ñu bare. Xalaat Yonenta Yallah Yusuf. Jamm rek ngay am. Deug rek nga wax. Yallah sa weruway la abadaan.

  • @DembaFaye-xc3bq
    @DembaFaye-xc3bq27 күн бұрын

    Naniou yallah mouseul oustaz ak imam nafekh

  • @CheikhDieng-gf1sp
    @CheikhDieng-gf1sp27 күн бұрын

    Oustaz dioumoul deugue la wakhe na counén khol si yalla,yalla mofi nék

  • @Momo44454
    @Momo4445428 күн бұрын

    MashaAllah Malikia ❤️ il faut être juste et honnête 🙏🏿❤️

  • @serigneniomrelo6956
    @serigneniomrelo695628 күн бұрын

    Cheikh Ahmed yalnanko yallah takhawou

  • @mansourdiagne1964

    @mansourdiagne1964

    28 күн бұрын

    Yalla douko takhawou nakh doméram la

  • @Xaliloulah_Bou_Sonko99
    @Xaliloulah_Bou_Sonko9928 күн бұрын

    Mashllah hadj makhtar ndiaye al amine

  • @kanekiken9566
    @kanekiken956626 күн бұрын

    Machalla ❤️

  • @DahiraSiratikalMoustakhimUASZ
    @DahiraSiratikalMoustakhimUASZ28 күн бұрын

    Macha allah. Yalna ko yalla taxawou inchallah

  • @papesambagueye5974
    @papesambagueye597428 күн бұрын

    Il faut qu'il arrête. Cheikh ahmed n'a jamais cessé de jeter des diatribes a M. Ousmane sonko. Joullit dou togn. Té dou toumal moromou joulitam.

  • @assiandiaye8904

    @assiandiaye8904

    27 күн бұрын

    Tout à fait. Ceci n'est pas un accident. Lui et Moustapha Sy Al Amine ont souvent été très virulents envers Sonko.

  • @azizndiaye9483
    @azizndiaye948328 күн бұрын

    SËYDI EL ADJI MAALIK,MOSUL TOOÑ TE MOSUKO DIGLE,SOO AMEE SA MBOKKU JULIT BU TÒÑEE, WOXKO DËGG,WAL ASR LA BUUR YALLA WOX, USTAS DAFA TOOÑ,NA JEGGËLU,LUKO YOON JOX MU JÊL,LI MOOY DĒGG.

  • @cheikhlei3193

    @cheikhlei3193

    28 күн бұрын

    Lolou moy waakh dji dé mais dangaay guiss yén gars yi di parparloo beugko déf victime

  • @daoudambengue5306
    @daoudambengue530628 күн бұрын

    Yala na Bour Yallah mousseul Sénégal ci goor djiguéne yi ak séni alliés.

  • @DembaFaye-xc3bq

    @DembaFaye-xc3bq

    27 күн бұрын

    Amine ak imam oustaz nafekh

  • @daoudambengue5306

    @daoudambengue5306

    27 күн бұрын

    @@DembaFaye-xc3bq Yeup, Amine

  • @omarpouye1493
    @omarpouye149328 күн бұрын

    Mon soutien à Oustaz Ndao. Yalna Yalla takhawou la.

  • @moustaphagaye2362
    @moustaphagaye236228 күн бұрын

    Machallah makhtar ndiaye

  • @ibrahimaMbathie-kg2lr
    @ibrahimaMbathie-kg2lr28 күн бұрын

    Je vous adore ❤❤❤joulit ni lay mél❤❤

  • @MARIAM_SY
    @MARIAM_SY28 күн бұрын

    Cheikh Tidiane Ndao défa Bagne Ousmane Sonko ba gneupe khame ko. je me suis désabonner de ses comptes depuis plus 2 ans, ak gnou méle ni mome dax déma allergie lou bone . Yalla nako djégueule dakh li dara gueunouko ñaw. Il véhicule une haine vicieux et c'est très grave!

  • @babacarndiaye8263

    @babacarndiaye8263

    28 күн бұрын

    CHEIKH TIDIANE MANOUL BEUGUE WAHABITE

  • @cheikhlei3193

    @cheikhlei3193

    28 күн бұрын

    ​@@babacarndiaye8263wahabite bi dé gnikoy togn yeup yalla monguilene di toroxal. Seydi hadji Malick tognoul andoul ak kouy togn talibé cheikh dou togn té souléne moytouwoul parparloo

  • @paousmanendao2030

    @paousmanendao2030

    27 күн бұрын

    ​@@babacarndiaye8263 wahhabites dara nekousii dans la religion il y a plusieurs branches respectons la croyance des une et des autres

  • @babacarndiaye8263

    @babacarndiaye8263

    27 күн бұрын

    @@paousmanendao2030 JE NE PEUX PAS RESPECTER LES ASSASSINS DE LA FAMILLE DU PROPHETE ET LEURS CONTEMPORAINS LES POSEURS DE BOMBE ET PROFANATEURS DE TOMBE DE SAINTS DEMANDES A SONKO CE KIL AVAIT FAIT DU DRAP DE WAZIFA TIDIANE QUAND IL ÉTAIT A GASTON BERGER COMMENT POUVEZ AIMEZ CES GENS LÀ QUI DÉTESTENT MEME LE TITRE DE SEYDI ATTRIBUE AU PROPHÈTE

  • @BEBO_DIMO

    @BEBO_DIMO

    27 күн бұрын

    ​@@babacarndiaye8263 Kou séleki kou bone manoko beugue. yaw ya ñak argument dëg souko nékhé nék Wahabit, souko nekhé! et après?t'es qui pour juger? I don't blame u, blame yourself! Séne xol dou ame Sakina mouke ndax bagnéle

  • @thiernobirahimdiop1637
    @thiernobirahimdiop163728 күн бұрын

    Vraiment ce pdg il est Tres digne serieux je suis emut

  • @DabaKebe-wg6dk
    @DabaKebe-wg6dk28 күн бұрын

    Machallah serigne Makhtar Ndiaye

  • @aminataseck7481
    @aminataseck748128 күн бұрын

    Machalla yallana léne yalla Faye ywe 😢😢😢

  • @salioudiouf4593
    @salioudiouf459327 күн бұрын

    machaala beggnaniou trop si plateau bi. Yalla naco yalla Takhawou té delloco si Ndiabotam si barkee sws

  • @laminesaliourafahi6906
    @laminesaliourafahi690628 күн бұрын

    Ñiongi ñianal cheikh Ahmad tidjan ndaw yalla tègil ko nattu bi

  • @mohameddiedhiou5476

    @mohameddiedhiou5476

    28 күн бұрын

    Lii du nattu buñu di jaawalé, kii dafa toppu bakanam ba fayeeku li mu jiw. Moom fu kawé la nekkoon waayé moo suuféel boppam ndax térangay àdduna yu ñàkk solo yii.

  • @ousseynoudieye1431
    @ousseynoudieye143127 күн бұрын

    Nit Boula yalla dioxé yén thieur yi dangay moy yén yi oustaz nak yalla nako yalla taxawou bamou guén si xat xat yi té mou banie ko dalati in schallah 🇸🇳❤️ jeureujeufeuti PDG

  • @dieynabasene8425
    @dieynabasene842527 күн бұрын

    maacha allah PDG vous avez réagi en vrai nitou dîné sans parti pris avec toute franchise en toute honnêteté merci de parler à cœur couvert un témoignage digne d un vrai seutou Mame seydi Elhadj Malick sy Radi allahou tala ane hou un plateau riche avec des hommes de valeurs

  • @matarcisse1174
    @matarcisse117427 күн бұрын

    Alhamdou sonko sii adouna la sa lepp leer diam sii ioe mai merci beaucoup PDG 👨‍💼 yalla rek mo matt

  • @mberryable
    @mberryable28 күн бұрын

    Yalna yalla takhawou leu thi barkep yonentibi sallahou wa Salim amine amine.

  • @PapeNgom-po8et
    @PapeNgom-po8et28 күн бұрын

    Seydi makhtar Ndiaye ya de gou ma la sope❤❤❤❤❤❤❤

  • @BoubacarBa-zi1mu
    @BoubacarBa-zi1mu27 күн бұрын

    Asalamou Aleykoum warahmatullah Mangi lendi nouyou dilen ziar boubakh té dilen nianal jamm Mangi rafetlou jotay bi boubakh si mbiroum sougnou mbok bi Di Oustaz cheikh Ahmed Tidian Ndao di len nianal boubakh Yallah na nelen Yallah fay yiw Nit ni rek la wara mel bou mbokam nekké si Jafféjaffé mou jappalé takhawou ko . Oustaz kou amal njerign nit ngni la ndakh Yag na niou gindi Di niou begal si ay wakhtaanam si ay att you beuré bueri (Dafa joum rek ) Ndakh kouy wakh ak kouy def rek Moy joum ken matoul ay nit rek len mankoy Toubal boubakh Di jeggaloul 🙏 Mangi nian Yallah teggil ko nattu Yi si kawam jappalé ko takhawou kou boubakha bakh moudellou waat si liguey bou rafet bimou nekk Di woo ngni si Yallah Yallah nako Yallah Yeketi Yok kham kham bi boubakha bakh dolli ko soutoura defal ko Jammu Aduna ak Jammu Al akhira

  • @mamadoudiop5844
    @mamadoudiop584428 күн бұрын

    Oustas limou wakh rék la wara wakh deugg d'où romb nope yalla nala yalla sam choix for puissance 🙏🙏🙏👍🤝 peace and love yalla nala seri Babacar sy alhalifa wallou🙏🙏🙏🙏🙏

  • @taarikhs

    @taarikhs

    28 күн бұрын

    Défal vidéo nga wah lolu. Soyons véridique guir yalla

  • @cheikhlei3193

    @cheikhlei3193

    28 күн бұрын

    Défal video wakh limou wakh moom ndéyou mbileu dji mongui diégalou kom khamnga kokou il regrette

  • @KaBassirou-uc4nz

    @KaBassirou-uc4nz

    27 күн бұрын

    Defal vidéo wakh ko😅😅 niou Kat sa ndaye si kaso gu 😀😀

  • @modoudialo3282

    @modoudialo3282

    27 күн бұрын

    Oustaze dafa dioume nagoul rk

  • @lerendez-vousdessportifs9286
    @lerendez-vousdessportifs928627 күн бұрын

    Je l’ai toujours écouté et tiré beaucoup d’enseignements sur bien bien vrai que je savais qu’il détestait Sonko mais pour être franc il dépassé les bornes avec cette nouvelle sortie

  • @salifoundong4197
    @salifoundong419725 күн бұрын

    Cet homme est franc

  • @abdoukhadrediop2210
    @abdoukhadrediop221027 күн бұрын

    De tout coeur avec ctndao nous le llaissons entre les mains d allah soubhanahou wa tallah et son envoye. Un mourant ne peut rien contre un mourant.

  • @elhadjindiaye1246
    @elhadjindiaye124628 күн бұрын

    Bravo et Merci Mr Ndiaye bien dis

  • @imamndaw9693
    @imamndaw969328 күн бұрын

    Alkhourane kou tok ba diko firi ak diko diangalé warnga ngako djikowo . Yalla na yalla takhawou ko.

  • @zenithtransitinternational9094
    @zenithtransitinternational909426 күн бұрын

    assalamou aleykoume wa keur gui niougui ziar di balou akh wayé andoumak matar ndiaye limou wah ndakh Al Oustaz Cheikh Ahemd Tidiane Ndao limou wah dara amoussi boulén fatini kiniounane daniouko togne dém la wah Président Macky lou geuneu niaw lolu donc analyse bi fofu gako warone kholé Oustaz waham daniouko rafetlou yalna Yalla geune ko yégué

  • @HoodBi-op5pq
    @HoodBi-op5pq26 күн бұрын

    Kou Kate ndayem moy s'en wa dji Kou todj lefeul ndayam

  • @ABDOULAYESOW123

    @ABDOULAYESOW123

    26 күн бұрын

    Ségne bi amal yar liguay déf déy amoul sens té diguako reuthiou

  • @dedesylla6508
    @dedesylla650827 күн бұрын

    Maa Chaa Allah le PDG M.Makhtar Ndiaye Al amine est très véridique ak sangnessem bou rafète, nous voulons des personnes pareilles pour le développement de notre pays, جزاكم الله خيرا أيها المدير الصادق،وفقك الله،وحفظكم

  • @binetasakho892
    @binetasakho89228 күн бұрын

    Yalla deug la beug même si on te mets un couteau sur la gorge . J’écoutais très souvent Oustaz mais qd j’ai entendu ce qu’il a dit ça m’a fait trop mal vraiment. Il a fait une erreur . Yalla nako yalla takhawou

  • @mansourdiagne2659
    @mansourdiagne265928 күн бұрын

    merci beaucoup PDG

  • @aliounembaye61
    @aliounembaye6127 күн бұрын

    ❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏

  • @Mohamed-se3lr
    @Mohamed-se3lr24 күн бұрын

    MachaAllah PDG, il a fait une faute et non une erreur. Que Dieu l'assiste.

  • @IbrahimaNgom-dt5wb
    @IbrahimaNgom-dt5wb27 күн бұрын

    اصبتم السنة واصبتم الحق فجزاكم الله خيرا

  • @NdeyeSarr-nm7pw
    @NdeyeSarr-nm7pw27 күн бұрын

    Melason limou wakh mo ganagara te Dara fekoukothei

  • @papabiranendaw1195
    @papabiranendaw119526 күн бұрын

    MachAllah le PDG a tenu discours très responsable. Yalla rek mo mate Allahoumma salli ala saydina Mouhammad wa sallim

  • @DAOUDASAMBASY-np6bb
    @DAOUDASAMBASY-np6bb24 күн бұрын

    DJARAGUEEN DJEUF YALNA SUNUBOROOM SAMLÉÉN AARLÉÉN YOKK TAXAWOU LEE'N YALNA SUNUBOROOM TAXAWOU OUSTAZ CHEIKH AHMAD TIJJA-NI TEGGUILKO NATTUBI CCI BARKI YOHANTABI S A WSLMM CCI CHEIKH ABUL BASSE CCI BARKI MAWLA-NA CHEIKH

  • @modoukhabanembackediorel8591
    @modoukhabanembackediorel859128 күн бұрын

    انصر اخاك ظالما او مظلوما، قالوا يارسول الله فكيف ننصره ظالما؟قال تأخذ فوق يديه

  • @cheikhseck4760
    @cheikhseck476028 күн бұрын

    Billahi politique bi yakk na khol yii yén nieupa yem guemolén dara wayé yalla bakh'na imam yalla nako yalla takhawù😢 té mousseull niou ci seytané

  • @user-po7mt5bh9m

    @user-po7mt5bh9m

    28 күн бұрын

    Ndao naafeq piir la shraiha muhamadiya çaw nako 80 yar

  • @DiengAhmed
    @DiengAhmed28 күн бұрын

    Mahtar wah n'a degue sapokou bou djoumé dagua konane dagua djoum

  • @happysenegaltv333
    @happysenegaltv33328 күн бұрын

    Niongi nian ndieukkeul ngir oustaz cheikh tidiane ndao wallahi kham nagn ni mo toogn kon dieggeul leenko té yalla takh

  • @IbrahimaNgom-dt5wb
    @IbrahimaNgom-dt5wb27 күн бұрын

    li yonėn tibi wakhon ci wa an sar mo nėkke çi sonko kou bakh dinako begue wayė kou sa khol sėlloul doka begue xam xam bou sa xol rafė sėtoul dalay alak yalna yalla dini kiniane çi xolam

  • @pembazolo9262
    @pembazolo926228 күн бұрын

    Vive iustaze Ahmed Tidjani ndaw ❤

  • @cheikhseck4760
    @cheikhseck476022 күн бұрын

    Li rekk la Imam Cheikh Ahmed Tidiane Ndao wax koumou méti rk goordjiguén nga: "Ahonzou billahi mina sheytani radjim. Bismilahi rahmani Rahim. …………………………. ( des prières) Mboki djoulites yi mboki Sénégal séne mbok séne sopé Cheikh Ahmeth Tidjiani Ndao mo fass yéné wakhtane ak yéne si li khéw si Rewmi. Mou mélni, tabara kallahou, fane yi yeup gni ngui guiss lo khaméne tani daal daloul khél thi ay nitou sheytané you nga khamni gno nga diougué thia Tougueul nga khamni makk gni Tougueul Daroul fassikhine lanouko toudé; manam réwou kathior yi. Moy Tougueul, lou bone louné falane koy nassé. Rawatina France rawatina Paris. Mou mélni fane yi amna niari Kilifeu yo khamni diogué nanou Tougueul bassi niati kilifeu, tabarak’Allahou nieuw fi si Rewmi. Niome niati kilifeu yoyou teup ay gordjiguène lanou. Ana lane moniou wara bolék kilifeu yoyou baniouy ame ak niome yéne relations yi, lou diara lathie la. Ndakhitam gni nga khamni niome lanou dink Rewmi touma dji daf léna top, rawatina Ousmane Sonko. Ousmane Sonko, depuis digane téme ak Adji Sarr li niouy toudé ak ngordjiguène danouko ték si déram. Adji Sarr si bopam mo wakh né Sonko done na seuy ak mome si guanaw. Toumal kossi wakhni loumou beug la, ndakh mome ladane déf ak mome. Kone sou féké toumeu bobou dalna Sonko moudi kilifeu warna moytou nak ndakh kouniouy djigne beuti goudi do sothio yéli gouné. Kone souféké né toumeu bi tégouna si kawam ma dégate kounouy wakh Bah Diakhaté déf wakhtane né: limay wakh soudoul deug nama Sonko porter plainte. Toumalko si né done na sékh’ak kouniouy wakh Ndiaga Seck ba gagne ko bamou déme hôpital di fadiou. Lane lanou sékhone seuy bo khaméne tani seuyou goor ak goor la. Lolou nék lou niaw t’a depuis Bah Diakhaté wakh ko guissouma Sonko déf béne réaction si lolou pour woné ni takhal nanou déram pour diémko ragueu. Niarél ba wala niatél ba moy biniouko falé maire rou Ziguinchor guiss nanou l’amourachant ndieuka recevoir diougué France gordjiguène la. Niou délou wate guiss Sonko si bopam mou yor béne parassol bo khamni mi nguiko teuyé ni, lolou yeup kouko gueustou di ngako guiss, di dokhanetou. Couleur bi couleurou drapeau gordjiguène yila. Lolou yeup di ay toumeu yo khamné ni dakoy takhal toujours ta douma guiss mou wédi ko. Niou fal léne diokh léne Rewmi Ka niou ndieuka invité sa palais ba dip gordjiguène niou thiowko fi thiow lou reuy ba Mame Makhtar guéneu nassi wakhtane si wakhtane bou yatou; nio ngui kossiy gueureum diko santt. Beurki démb université, kiniouy wakh Jean Luc Mélenchon nieuw fi. Niou recevoir ko si daara dji gueuna makk nga khamni mou symbole bi gueuna reuy si Rewmi niou fay tagaté gniy wara yor Rewmi euleuk, ta gni yor Rewmi nieup diarfa. Université bobou lanou yobou say-say bii mou takhaw wakhni, si kanamou étudiants yi si kanamou sounouy ndaw sounouy yakar, né : « maa djiteul a khékh ak ngordjiguène sa France baniou nangou kofa goor di seuy ak moromou gooram » Néna lolou moko dieuka khékh France baniou légalisé ko. Ta dafa mélnimission bobou moko in’di Sénégal. Ta meunou kofé dokhal nak tant que diapalé wounouko. Té arabe dafay wakh ni « ane nassou ala diini moulo kihim » peuple bo guiss la séni djite gueum moudi séne diiné mome lanouy gueum. Ta dafa mélni Sonko daf niou beuga gueumlo ak ngordjiguène ayoul. Lolo waral nguéne guiss kilifeu nguéne guiss diléne sétsi si sénouk kay, bamou néké maire, ak biniou léne diokhé Rewmi, ak beurki démb kii nieuw di Jean Luc Mélenchon wakh wakhbou reuy bii né mo ndieuka khékh nguir niou légaliser ngordjiguène sa France ba goor ak goor difa seuy. Mou mélni Abdou Karim Khroum khakh wakh nani biniou criminaliser ngordjiguène fi si Sénégal, mbolo And same djiko yi diko khékh démone nanou si Sonko pour mou signer wayé dafa bagne; lolou mome diakhal nama. Ta sakh mbolo same djiko yi nga khamni Ababacar Mboup moko djité, amna niou wakhone né, mbolo momou ab lobby la bo khaméne tani dafay publicitél gordjiguène yi. Cheikh Oumar Diagne wakh nanouni nite la ko khamni dafay publicitél gordjiguène yi. Lolou lép di ay toumeu you takhaw, bassi casseroles yi nga khamni Sonko dane na wakh pour nioukoy teug di manifester wakhone nanouko néko lolou bakhoul si Rewmi ndakh gordjiguène yi baniou dé khékh séni droits thia Tougueul thia Europe mome lanou done déf di teug ay casseroles kone nak boko défé roy ngaléne niome gordjiguène yi. Ba tay rék dafay mélni empreinte gordjiguène dafa guénoul si parti bi niouy tousé Pastef. Dafa mélni dafa ame louniou d’accord, louniou weuleuréne té. Lolou lép nak di moussibeub Sénégal. Ndaw gni ngéne yéwou dayi séne bop khél khamni euleuk gou Sénégal mi ngui nék si danger sou féké déme nanou ba légaliser fi ak ngordjiguène. Sonko tamite bimouy tontou guiss nannou né tontou you woyof la tontou ndakh dafa mélni dafa beuga masla ak gordjiguène yi. Ta Al Xur’an dafa wakhni « waddoulaw toud’hilou fa youd’hinou » gordjiguène yi liniou beug moy nguéne maslah ak niome baniou meuna dokhal niome séni programmes. Maslah bobou nak lanou léne warta may béne yone. Waw « Ya ayouhal Nabiyou djiahidoul kouffara wal mounafi khouna weukh louf haleyhim » Yalla néna yaw Yanéneta bi salla lahou haleyhim wa salam djihaatal ak yéfeur yi ak nafékh yi néna ta nga bania maslah ak niome si dara. Na nga sokhor si niome. Sokhor ngogou lanou wara dieulane té ak gni nga khamni nio gadou agenda gordjiguène yi pour tass ko thi adina bi. Nga khamni ay missionnaires you sheytané lanou. Mou mélni Sonko sou wakhéni fi si rewmi ak ngordjiguène ak mouray feulé sa France, mou mélni dafay comparer niar yi, kéne dou comparer lou dagane ak lou kharam. Ak ngordjiguène danou koy dindalé ak rayy nite, di da lako ak bokalé ak Yalla, di da lék ak thiathie ak viole; wayé kéne douko dindalé ak moytou. Polygamie la beuga wakh moudi diabar you beuri. Khame nga France danio dafa ak ngordjiguene fofou wayé dano téré diabar you beuri. Niari diabar niari diabar lolou bakar la si niome. Sonko nak ni, euuuuh mou beuga comparer polygamie bobou moudi niari diabar niati diabar dieum ba gninti diabar ak ngordjiguène ; dédéte. Bi dafa dagane, bi dafa haram. Bokouniou. Kone liniou beug daaal moy moi khamni mome dafa compagné wone ni mome sou falo limouy ndieuka déf modi criminaliser ak ngordjiguène mome lay ndieuka khékh bamou dégne si Rewmi. Lolou lanou diay si projet bi, né sa bou falo limouy ndieuka déf moy di di fi ak ngordjiguène, wayé bobou ba légui guissou niou mou yeuy si wala mou yabi si, loudoul woo séni kilifeu niou nieuw beuga nék star si kanamou khaléyi. Niou ngui koy niane mou ragal Yalla, diko niane Diomaye niou ragal Yalla si khaléyi khamni nioy yakarni euleuk…."

  • @mamadoutall8827
    @mamadoutall882727 күн бұрын

    MA CHA ALLAH PDG VRAIMENT JE VOUS ADMIRE ENCORE PLUS VOTRE FRANCHISE ME VA DROIT AU COEUR

  • @sady1964
    @sady196428 күн бұрын

    Merci kebè

  • @bambadiop
    @bambadiop27 күн бұрын

    Un mara se protège en prêchant la vérité

  • @mactarndiaye1976
    @mactarndiaye197627 күн бұрын

    Macha'Allah tourondo kaddu yi rafetna

  • @sidymbacke8837
    @sidymbacke883728 күн бұрын

    Merci p d g ❤

  • @modoudialo3282
    @modoudialo328227 күн бұрын

    Machlla yonéne tébi néna sa bokou diapaléko bou toyé walla bounuko toyé bou toyé noko kay wakhé ganiko yatoye machlla pdg❤❤

  • @user-xq4qt1qh2z
    @user-xq4qt1qh2z27 күн бұрын

    Machalla ❤❤❤

  • @ousseynoutoure9417
    @ousseynoutoure941728 күн бұрын

    ❤❤

  • @Sirou71
    @Sirou7128 күн бұрын

    Alhamdoulillahi Wahidoul Ahad

  • @aminatadiaw9283
    @aminatadiaw928328 күн бұрын

    Nafek bakhoul sokhor bakhoul une bonne leçon à retenir dadone khawi soutoureu far khawékou, yené Nek la....

  • @mouhamedlaminefall6218
    @mouhamedlaminefall621827 күн бұрын

    Macha alla PDG nitt day dëggou

  • @ndiagafall4560
    @ndiagafall456028 күн бұрын

    Mak mo rew dafa xewi Mak mo yarediko dafa xewi Mak mo khamadi dafa xewi

  • @babasall4261
    @babasall426127 күн бұрын

    Machalla ♥️♥️♥️❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdoulayesow3869
    @abdoulayesow386928 күн бұрын

    Oustaz niogui sa guinaw

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop120628 күн бұрын

    Kou séll ki kuko songue sankou wassalam 🙏

  • @user-ll2ot7ho2t

    @user-ll2ot7ho2t

    28 күн бұрын

    kou sell diga teuddéh domou diambour, bayi lén fén wakh léen sonko deugg, sonko fén nalén ba falou, wayée doufi am diamou deh fénal nafi macky sall lou amoul

  • @bambaniang1271

    @bambaniang1271

    28 күн бұрын

    @@user-ll2ot7ho2tIoe sakh soko songué gni niouss sa ndey

  • @MoustaphaNdiaye-ho2qn

    @MoustaphaNdiaye-ho2qn

    28 күн бұрын

    Dioulit day moytou di wakh louko woroul ,on sera en face à allah azza wajal bientôt 🙏🏼

  • @FODEDIABYGASSAMA

    @FODEDIABYGASSAMA

    28 күн бұрын

    Koi yengou niou teppi sa leufeul ndey domeram yi yenn wa apr ​@@user-ll2ot7ho2t

  • @AliouToure3769
    @AliouToure376927 күн бұрын

    Merci beaucoup PDG

  • @omartoure2251
    @omartoure225127 күн бұрын

    Free ❤❤

  • @lerendez-vousdessportifs9286
    @lerendez-vousdessportifs928627 күн бұрын

    Cheikh Ahmed borom kalimatoul kacc 😮😮

  • @papediop7867
    @papediop786727 күн бұрын

    En tout cas dioulite dou Accusé sans preuves... il faut qu'il arrête

  • @pamoulalo4977
    @pamoulalo497728 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @BabacarNiang-yb4my
    @BabacarNiang-yb4my27 күн бұрын

    Machala yaw nit kou deugou nga

  • @ndeyefaye6835
    @ndeyefaye683527 күн бұрын

    ❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🙏

  • @MoustaphaSow-my2yu
    @MoustaphaSow-my2yu27 күн бұрын

    Oustaz

  • @tassegueye8996
    @tassegueye899628 күн бұрын

    Da togne nak deug yalla moko mom

  • @NdiasseNdoye
    @NdiasseNdoye28 күн бұрын

    😂😂😂😂😂wakh djou bone bakhoul

  • @papasy25
    @papasy2527 күн бұрын

    Macky day soul ndanane. Il a corrompu bcp de chefs religieux et de prédicateurs. Ki mo fégne lé rek parce que dafa eupeul mais il y en a beaucoup qui devaient faire comme lui car ils ont reçu argent voitures terrains et billets Mecque ou Dubai

Келесі