DIGENTE MBAKHANE Ag SERIGNE TOUBA

#Xamsamreewtoutehistoiredusenegal🇸🇳
E-mail 📧 : mbayegueyesyll@gmail.com
Téléphone 📞 : 76 169 45 09

Пікірлер: 107

  • @sakkuxam-xam1593
    @sakkuxam-xam15934 жыл бұрын

    Àm na solo lool, Serigne Mbaye Gueye sill, Chêne bii Di xàm sàm rèew, de gnew nà ci wàx toom, Yàl na ngà fi yàgg lool te wèr, Maa ngi laaj: bàrgeet àk jogomaay, lu mu'y tekki ci wolof, Man la Mouhammadou Kara KA ndongol boroom darou mouhty,

  • @ousseynouaw2996
    @ousseynouaw29964 жыл бұрын

    Macha'halla yalla na yalla yookk fane wi akk weer gui té magui sakko si yaw ga indil nou histoire mam cheikh Adama Gueye ak borome TOUBA

  • @barandoye7413
    @barandoye7413 Жыл бұрын

    Dieureudieuf Baye Mbaye sylla amena solo Dieureudieuf Serigne TOUBA KHADIM RASSOUL amul MOROM abadane

  • @fayacheikh61
    @fayacheikh612 жыл бұрын

    Thieuy nationalite serigneTouba yomboul am a 100% dieuredieuf serigneTouba dieuredieuf serigneTouba dieuredieuf serigneTouba dieuredieuf serigneTouba dieuredieuf serigneTouba dieuredieuf serigneTouba dieuredieuf serigneTouba dieuredieuf serigneTouba 😭😭😭😭

  • @abdoukhadrediop5165
    @abdoukhadrediop51654 жыл бұрын

    Je vous suis depuis barcelone te gnongui gnane si barkep gnoll aminata sunu borom yatall liguey bi barkep borom touba

  • @sambalingeer5680
    @sambalingeer56804 жыл бұрын

    Jërëjëfëti Baay Mbaye Gueye Syll am në solo maachallah .

  • @morawadieng8297
    @morawadieng8297 Жыл бұрын

    Assalam Anlaékoum Serigne Mbaye Guèye Syll, Dieureudjeuff ! Yallah na la Yallah faye ci barké Serigne Touba.

  • @cheikhsylla4491
    @cheikhsylla4491 Жыл бұрын

    Dieureudieuf Serigne mbaye Gueye syll. Amna solo lol.

  • @makhtarsylla1684
    @makhtarsylla16844 жыл бұрын

    Macha Allah amna solo yallna yalla yagallafi té nga andak wer

  • @labsolugueye9016
    @labsolugueye90164 жыл бұрын

    Kéndou serign Touba Wallahii Kéneu Mbacké Balla Kéneu khamoull Lounlay Fayé Mbackei balla Aicha 🙏❤️🙏❤️🙏❤️🙏❤️🙏

  • @wakeupafrica9906
    @wakeupafrica99064 жыл бұрын

    Waw goor ... sa Baye yokk yaagg rek tee werr nek thi laniou sokhla histoire gou werr. Avec le systeme français sa a été toujours ainsi bassi gniniou djité fimou nek ni ay toubab you nioul laniou.

  • @mamadoubadabo4459
    @mamadoubadabo44593 жыл бұрын

    qu'Allah exauce nos prières et nous rende sa grâce Merci de nous accompagner avec xam sam rewe tv

  • @babawane1884
    @babawane18844 жыл бұрын

    AS SALAMOU WA ALEIKOUM papa! am naniou mbekkté di degglou tàríkh, ráwatina tchi SOUNOU MAME KHÀDÍMOÙ RASSOUL. JAZAKALLAHOÙ KHAÏRAN

  • @niggeudou2404
    @niggeudou24044 жыл бұрын

    Diadieuf papa amna solo yalla na yalla faye

  • @bfaye8462
    @bfaye84624 жыл бұрын

    Papa danola sop te s touba rk takh moye sonno yakar ana baye fall s bamba yi malin sop barki s bamba

  • @morndir9549
    @morndir95494 жыл бұрын

    Bay mbaye guéye yallanala yalla may fan wou goud ank ak wergui yatam beug nañ bou baakh cou bég si bay mabaye beuseul j aime way

  • @pene1bayfall439
    @pene1bayfall4394 жыл бұрын

    MASALAAAH YALLA NALAA YALLA SAMOU SI BARKEP BROM DAROU MOUKHTY

  • @kanetalibebamba7437
    @kanetalibebamba74373 жыл бұрын

    ly amna solo mesoumaa xamnee mbakhane dõmii lat diorla ly mõ takh papa mbaye geye lingay déf vraiment amna solo lol

  • @jilidieng9464
    @jilidieng94644 жыл бұрын

    amna solo lolou Serigne Mbaye Gueye, Yalla nala Serigne Touba deugeureul te fey la geun gui fey, Jili Saliou mou Cheikh Bethio

  • @pacovip8689
    @pacovip86894 жыл бұрын

    Merci papa wahtane bi nekhna lole

  • @damefallsenegalff4263
    @damefallsenegalff42632 жыл бұрын

    Merci pérr c dame Fall setou mbakhann

  • @mohamedbop433
    @mohamedbop4334 жыл бұрын

    dieredieuf pére amna solo ma gui diangue boubakh tous mes encouragements

  • @hadhad7587
    @hadhad75874 жыл бұрын

    Dieureudieuf Serigne mbaye gueye syll YALLA nala YALLA Diapalè Abadane thi Barkè Borom Touba Aaaamine

  • @cheikhba9984
    @cheikhba99844 жыл бұрын

    dieuredieuf papa yalla nanoula Serigne Touba fayal si liguèy bou raféte bi machallah

  • @Alassdi1234
    @Alassdi12344 жыл бұрын

    Mashallah

  • @kalidouwade9442
    @kalidouwade94424 жыл бұрын

    Machala amena solo

  • @serignekossoseye7925
    @serignekossoseye79254 жыл бұрын

    Machala papa yalla na yalla guoudal fane wi si barke borom touba

  • @abdoulayebaneniang
    @abdoulayebaneniang4 жыл бұрын

    Machallah bay mbaye yangui yok sounou kham kham

  • @bounambodjcisse2082
    @bounambodjcisse20824 жыл бұрын

    Ligguey bi amna solo - nala sunou Borom Fay takhawoula si barké Serigne bi

  • @madiawmboup7403
    @madiawmboup74034 жыл бұрын

    Machalah

  • @papediagne4255
    @papediagne42553 жыл бұрын

    Merci mercis merci ok ✅

  • @lopapis7135
    @lopapis713510 ай бұрын

    S mbaye Gueye sille beguh thiépp

  • @maimounambacke2882
    @maimounambacke28824 жыл бұрын

    Machallah bi rk la doone kharr

  • @serignesalioutaissirndongo5819
    @serignesalioutaissirndongo58194 жыл бұрын

    MACHALAH YAW MOM SAGOU YON WI GUA GUISNAN SA TAXAWAY LOOL BOU AM SOLO SABOU AMEE KOUGNOU BEUGA SOSAL YALNA YALLA SAM LEU ARR LEU LAKH LA FOU YAXX AGOULL GOUDALL SA FANE LOOL BER TAISSIROUL HASIR

  • @falloundiaye2182
    @falloundiaye21824 жыл бұрын

    Amna solo loll

  • @elhadjithiam8376
    @elhadjithiam83764 жыл бұрын

    Machalla lerna yageu filol te wer

  • @papesallfatick2801
    @papesallfatick28014 жыл бұрын

    Machallh serigne tounba amoul morom

  • @bambatouba6884
    @bambatouba68844 жыл бұрын

    Wa Anna mouridi Cheikhoul Khadim yi Aboné Len ngir Khadim amounou Loudoull Serigne Touba man dé aboné na dierediefati Sylla

  • @ababacarndiaye1966
    @ababacarndiaye19664 жыл бұрын

    Amna solo

  • @tahirmbaye8894

    @tahirmbaye8894

    4 жыл бұрын

    deguela mome

  • @amdysyll9259
    @amdysyll92594 жыл бұрын

    Man li rék la begge histoire merci

  • @modouabibediop1713
    @modouabibediop17134 жыл бұрын

    Baye mbaye syll talibê borom darou yalna sa fan goudd t andak wuer

  • @cheikhthiam8695
    @cheikhthiam86954 жыл бұрын

    Akssa amna solo lol

  • @cherifdiallo3508
    @cherifdiallo35082 жыл бұрын

    Dieureudieuf kou bakha bakh

  • @alassanendiaye2939
    @alassanendiaye29394 жыл бұрын

    Machallah sylla

  • @ousmanesow1224
    @ousmanesow12244 жыл бұрын

    Machalla

  • @narrdiene1694
    @narrdiene16944 жыл бұрын

    Machallah

  • 4 жыл бұрын

    Céy Tubaab!! ñoom daal lakkal nan nu !!

  • @CheikhNdiaye-gl9sr
    @CheikhNdiaye-gl9sr4 жыл бұрын

    Yalla na Yalla fayy la seugn bii liga gnouyy dèffal amm na solo loll deugg deugg tarikhou Sénégal oumpeulè nanou ko loll

  • @beggjammbpp433
    @beggjammbpp4334 жыл бұрын

    Baay mbey géy sill maa ngi lay siyaar di la ñaanal fan wu gudd lool ak tawfeex ci barkeb ku baax ki Bég na nu ci yaw lool dalal nga xel yépp ci mboor mi yoon di sàggoo saa yu ne ci wàttu gi nga koy wàttu ba kenn du ko ma na suppi maa sàllaah yal na la yàlla wàttu ci barkeb ku tedd ki Xaadim-rassuul

  • @khadimmbayesamsopeyserigne3292
    @khadimmbayesamsopeyserigne32924 жыл бұрын

    Mach'allah deñu yekil yen wolof yu khote

  • @KCP970
    @KCP9704 жыл бұрын

    Merci pour ces histoires du senegal.

  • @Aistv2014
    @Aistv20144 жыл бұрын

    Machallah thiey khadimou Rasul 😭😭

  • @ndiayecheikh3309
    @ndiayecheikh33094 жыл бұрын

    Merci du wakhtane que vs portez à la connaissance des disciples mouride mais s il vs plaît par rapport au foto , pour la foto de de SERIGNE TOUBA il ne faut pas le mettre côté à côté de n importe quel autre foto merci

  • @mamadoubadabo4459
    @mamadoubadabo44593 жыл бұрын

    Bjr immortaliser vos récits dans des supports ( Livre , CD) très pertinent yalla na la Serigne Touba faye.

  • @modoubeye3311
    @modoubeye33114 жыл бұрын

    SB yalla nala yalla faye

  • @khadimmbacke312
    @khadimmbacke3124 жыл бұрын

    👍❣👂☝️💪

  • @sadextalibebambaprotege8524
    @sadextalibebambaprotege85244 жыл бұрын

    Walahy yagg yokk wer beug thierno baye mbaye gueye sylla yaw danga fi wara yagg ndax li yaw rk yaniouko meuna badil lou démé ni geuna yagg geunna wer

  • @codediaw4238
    @codediaw42384 жыл бұрын

    Dieure dieuf serigne mbaye gueye sill

  • @moegaye1837
    @moegaye18374 жыл бұрын

    On vous suis depuis Russie merci et bonne continuation

  • @gpproduction4720
    @gpproduction47204 жыл бұрын

    Nala yalla faye

  • @elhombrendayane1675
    @elhombrendayane16754 жыл бұрын

    Akkassa

  • @cheikhleye903
    @cheikhleye9034 жыл бұрын

    Ndoudal.weral.goudal.fane.tewer

  • @papafall465
    @papafall4652 жыл бұрын

    Machala dieureudieuf

  • @ablayendiaye4781
    @ablayendiaye47814 жыл бұрын

    Merci beaucoup mon père

  • @mamadoubadabo4459
    @mamadoubadabo44593 жыл бұрын

    En ce quatrième jour du mois béni de Ramadan 2021

  • @ndiayemana314
    @ndiayemana3144 жыл бұрын

    Depuis Espagne niongi koye téwelou

  • @marothiam9636
    @marothiam96364 жыл бұрын

    Dieuredieuf çi léral yii

  • @undeathofficielle
    @undeathofficielle2 жыл бұрын

    Longue vie a toi doundal

  • @aladjifayee7312
    @aladjifayee73124 жыл бұрын

    Sante serigne touba khadimou rassoul rek amoul morom

  • @khadimkane7795
    @khadimkane77954 жыл бұрын

    Yaw mome goudal fan rek

  • @salioufall7697
    @salioufall76974 жыл бұрын

    Saliou fall d abonné n'a mom ndame rék 💯

  • @ahmadoubamba5286
    @ahmadoubamba52864 жыл бұрын

    aboné lén

  • @serifgueye2168
    @serifgueye21683 жыл бұрын

    🙏🙏🙏🙏

  • @dialibatoumarahib79
    @dialibatoumarahib793 ай бұрын

    Amna solo diambar ga boromouk geustouga

  • @baye.mbackebeugserignetoub9308
    @baye.mbackebeugserignetoub93084 жыл бұрын

    Dieure dieuf .lou .am solo.mbekté ak Contanté .Ahmadou rek

  • @m0d0udi0p5
    @m0d0udi0p54 жыл бұрын

    sant mame thierno Ibrahim mbacke borom darou mousty

  • @moustaphadioparafat1307
    @moustaphadioparafat13074 жыл бұрын

    Sa Darou ziar moustapha diop Arafa

  • @papediagne4255
    @papediagne42553 жыл бұрын

    Abonè

  • @mouhamedsylla4774
    @mouhamedsylla47744 жыл бұрын

    Dieredief way syll

  • @bassiroudiouf3273
    @bassiroudiouf32734 жыл бұрын

    le générique je voudrais savoir c est quel chanteur et le nom du son

  • @amadouder1341
    @amadouder13414 жыл бұрын

    Salam Mbokou talibé ma ngui sakou ci kou kham kane moy rajass tambali waxtane di diégalou bou wér

  • @azomboup

    @azomboup

    4 жыл бұрын

    Wolofal baye mama ndiaye la natto di ker ker

  • @diadjiniang1145
    @diadjiniang11454 жыл бұрын

    Niomrè sa deuk

  • @moustaphacisse6404
    @moustaphacisse64044 жыл бұрын

    Egubdhi

  • @alsanecisse3784
    @alsanecisse37844 жыл бұрын

    Abonné lén ngén mana Kham sén réw ak lifi khéwon djuerediuef sylla

  • @cheikhseck7523
    @cheikhseck75234 жыл бұрын

    Wolafal bi kane moko diangue kouko khame

  • @abdoufatandiaye510

    @abdoufatandiaye510

    4 жыл бұрын

    Baye mama ndiaye

  • @mouhamadoudieng2780

    @mouhamadoudieng2780

    4 жыл бұрын

    C'est dans kharnoubi chanté par Mamaye mbaye vers la 45e minute

  • @mamadoumbaye7726

    @mamadoumbaye7726

    Жыл бұрын

    Baay mama ndiaye wolofalam bii nimu may déf, ak baay xaali seye, yalla nañu léén yalla fayak lu kawé séén ñort

  • @seckibrahima5512
    @seckibrahima55124 жыл бұрын

    Ou se trouve Keur Amadou yalla???

  • @khadimrassoulgueye5741

    @khadimrassoulgueye5741

    4 жыл бұрын

    Seck Ibrahima ct dans le Cayor et je crois que ce village n’existe plus

  • @seckibrahima5512

    @seckibrahima5512

    4 жыл бұрын

    Khadim Rassoul GUEYE merci bcp pour l’info mon frère 🙏

  • @gpproduction4720

    @gpproduction4720

    4 жыл бұрын

    C'est deux kilomètres à Ndiagne et un kilomètre à Guet ardo. Ce village existe toujours. C'est un grand village maintenant.

  • @mamadoumbaye7726

    @mamadoumbaye7726

    Жыл бұрын

    @@khadimrassoulgueye5741 yaa ñémé yalla, fala ahmadou bator diop dëk foofu lañuko ñaanalé, yaayu moustafa diop ministre fala dëk actuelment ka yoré dëkba abdul xafoor la tudd ñu tudéko mbaaxaan, déél wax loo xam walla nga nopi

  • @djogueelsamb7596
    @djogueelsamb75964 жыл бұрын

    🤣🤣🤣🤣 décoré par les colons avec la croix de Malte (franc-maçonnerie) Beaucoup de Marabouts des confréries actuelle le brandissaient avec un grand orgueil Bouparè tey mou aam ayii oustaz AK imams diniou doullo

  • @cheikhndiaye5200
    @cheikhndiaye52004 жыл бұрын

    Amna solo

  • @ibrahimakhalildjite8845
    @ibrahimakhalildjite88454 жыл бұрын

    Mashallah

  • @serignemodoufall826
    @serignemodoufall8264 жыл бұрын

    Machallah

  • @sokhnandiaye496

    @sokhnandiaye496

    4 жыл бұрын

    machalla Amna solo

  • @abdoufall1124
    @abdoufall11244 жыл бұрын

    Machalla

  • @ndiayemana314
    @ndiayemana3144 жыл бұрын

    Indil niou bour sine Coumba ndofèen

  • @mbanyicksenghore8948

    @mbanyicksenghore8948

    2 жыл бұрын

    That will be great

  • @kebekebe587
    @kebekebe5872 жыл бұрын

    Amna solo