Dieuf Dieul à Amina Poté défal ndank si Malick Fall passeport bi dou bou Amérique sou la waxé…

Vous pouvez visiter notre site web tikgalsen.com/
Suivez-moi sur mes réseaux :
Facebook : / generalgalsen1
Instagram : / general_galsen
Twitter : / tiktokgalsen

Пікірлер: 258

  • @aissatousambalaye5021
    @aissatousambalaye50215 ай бұрын

    Taxoul nga fayko longue vie à maman bi et à toi

  • @bibichekahgueye7569
    @bibichekahgueye75695 ай бұрын

    Mais pourquoi toute cette polémique il fallait le faire avant son mariage mais pas après son mariage ça vraiment c'est de la méchanceté tes faits avec ta maman ne nous concerne pas

  • @mamadousene6151

    @mamadousene6151

    5 ай бұрын

    Nena il lavait entamé avant l mariage

  • @mouniroudiop717

    @mouniroudiop717

    5 ай бұрын

    Ma chère quand on prend l audace d exposer sa vie publiquement il faut s attendre à toute forme de règlement de compte publiquement.quand les gens ripostent ils t attaquent là où tu es peu importe tes choix de vies.bale d'où gneupe KO meune

  • @bushra4079

    @bushra4079

    5 ай бұрын

    Malick mo guéneu di wanéwou publiquement apres son mariage, gars yi tmt guéneu diko wakh bopam publiquement après le mariage 😂

  • @ndeyefatoudiakhate9861

    @ndeyefatoudiakhate9861

    5 ай бұрын

    Je k ta fais pour ta maman ne nous concerne pas mon pays va mal vrément

  • @ndeyefatouba1012

    @ndeyefatouba1012

    5 ай бұрын

    Hawma POTÉ té messoumako guisse lodoul télé bi WAYÉ dara diapoulène loudoul Sokhor. Daguène nop diabaram bi té souguène sagnione ameko. Yaw mome mbeur mou perte gua ! !.

  • @sarahbibish2197
    @sarahbibish21975 ай бұрын

    Ndaysane boko kholé sakh khamni Deugg nga wakh

  • @user-kj8sw2rc8x
    @user-kj8sw2rc8x5 ай бұрын

    Khawma noumou demer, mais soumadone Amina Pote,demay deff nank, de pas faire du tontu ou du garowaler, sinon elle risque des choses qui lui seront très désagréables,na bayi son mari ak djeuf dieul régler sen problème, juste un conseil de mère

  • @requinquin1

    @requinquin1

    5 ай бұрын

  • @kambayependasall8908

    @kambayependasall8908

    5 ай бұрын

    Bilahi lolou la wara def n'a si mandou affaire de gor yalla la niome niar la mais dougou ba moudiou si am mbertel amna louka guene bilahi poté dama ko niewantal

  • @mymadieng

    @mymadieng

    5 ай бұрын

    Amina mo wayoul tfm nieupa am na niou dieukeur depuis des années ken exposé woul dieukeuram diamono dji kou beug mouthi da ngay neubeutou mais mom lepam defanté la

  • @nogayetall6677
    @nogayetall66775 ай бұрын

    Macha Allah sama dome inecha allahou dinga guena déde ndah yangi térale sa yaye

  • @mj-zq4qg
    @mj-zq4qg5 ай бұрын

    Linga deffal sa yaye sa dingantek sa yaye la, khamoo lou nit di defal yayam teh ne tekk

  • @rosediop965
    @rosediop9655 ай бұрын

    amina poté dafeu mousoule dara douniou réfléchir daniou fokené fou khaliss diougué elle cherche pas à comprendre daniou l'éne nakhe rék

  • @user-fx2tv3wh2e
    @user-fx2tv3wh2e5 ай бұрын

    Machalah frère ❤❤❤❤

  • @user-fo3px8mb9n
    @user-fo3px8mb9n5 ай бұрын

    Merci beaucoup ❤️❤️🥰❤️❤️❤️❤️❤️

  • @Germinal5219
    @Germinal52195 ай бұрын

    Amina passeport tahoul mou seye ak mom Na yoor passeport Somalie L essentiel ils s aiment ❤❤

  • @fatimasarr9384

    @fatimasarr9384

    5 ай бұрын

    Passeport Somalie 🤣🤣🤣

  • @diengfama294

    @diengfama294

    4 ай бұрын

    Pour yaw ils s'aiment togal khar

  • @KhalilDien-fe5uh
    @KhalilDien-fe5uh5 ай бұрын

    Saaawaay boul niou ndeyyyy sonaal waay . Goor yalla dou bari wakh waay da nguay ndeyyy xaar bamou nieuw ndeyy ÉTATS-UNIS ngueinn lidieuntiko mo gueuen wakh diou bari dji linguay intéressé wouniou . Daniou nekk si defaite

  • @diodiodiouf1845
    @diodiodiouf18455 ай бұрын

    Mashallah dieuf bilahi dagama nex

  • @Misskiwi277
    @Misskiwi2774 ай бұрын

    😢thieuy yalla ana soutouraa

  • @nogayetall6677
    @nogayetall66775 ай бұрын

    Macha Allah nawelonala yalla nalla thiate séhlou

  • @Mizafrica
    @Mizafrica5 ай бұрын

    Aye Waye Yeureum léne doumou Diambour bi pourquoi pas l’appeler au téléphone pour la conseiller, mais pas comme ça dans les réseaux, pourquoi vous n’avez pas parlé avant le mariage.

  • @youssoufabdoulayediopjohnn3774
    @youssoufabdoulayediopjohnn37745 ай бұрын

    DIEUFF DIEUL KUU KHOL SA KANAM DJISTCHI SINCERITE MAIS NAKK LINGUAY DEFAL SA YAYE LOLOU DIAROUTH DI FÉSSEUL WAKH BAKHOUL MALICK NAR DORKAT LEU

  • @Yaay26faal70

    @Yaay26faal70

    5 ай бұрын

    Vraiment lo défal sa yaay mom diaroul publicité

  • @binetafaye2027

    @binetafaye2027

    5 ай бұрын

    Yiew merrd way sa yaye la sé normal nitt kou beugué woné khou rek labagne thum sof

  • @youssoufabdoulayediopjohnn3774

    @youssoufabdoulayediopjohnn3774

    5 ай бұрын

    @@binetafaye2027 Waw Binta FAYE waw mais YANGUI SISSOU DEH Diarouko ndank bul diemeu KHAMADI toupko AIT ha AITcha way depuis NORVEGE OSLO

  • @oumoungom6180
    @oumoungom61805 ай бұрын

    Vraiment fall dagua sokhore yaw beuguo amina pour lane guaye xawi soutoura yaw amina sou amoul badiane yalla mokoye samb inchala

  • @ndeyefatougaye4071

    @ndeyefatougaye4071

    5 ай бұрын

    Wakhna si biiir wakh de

  • @boucountadiallo9692

    @boucountadiallo9692

    4 ай бұрын

    Ki daay dimbali potè pour mou bania encaissé xaliss diambour ki wadji dako door xalissam niew di battrè si soirée yi lolou moko métti sénégalais naak dafa gawa wax nit dafa sokhor tè xam cause bi

  • @FatimThiam-tj5oy
    @FatimThiam-tj5oy5 ай бұрын

    Machalah ❤❤

  • @FatouThiam-kg1qe
    @FatouThiam-kg1qe5 ай бұрын

    Y’a bone tè soxor do baye fall baxo

  • @Germinal5219
    @Germinal52195 ай бұрын

    Ki hana da noob Amina Yaw Malik gua diotél do haar ba mou delou guéne regler sen probleme Lane mo thi yonou Amina? Li mom sohore deug la

  • @djiboseck147

    @djiboseck147

    5 ай бұрын

    Delene atte deug ki daniou ko togne

  • @requinquin1

    @requinquin1

    5 ай бұрын

    😂😂😂😂 Amina mo ci douggou katt di sott. Malick Fall miii....on rékk😅

  • @Germinal5219

    @Germinal5219

    5 ай бұрын

    Lou thi yonou Amina Dem na tribunal kaye kon lou mouye outati thi reseau sociaux Li mom sohor la​@@djiboseck147

  • @bushra4079

    @bushra4079

    5 ай бұрын

    Khana ladjetéwo baparé soga wakh 😂 Amina moci dougueul bopam di yow fo né 😂

  • @user-uw5uq9nf5k
    @user-uw5uq9nf5k5 ай бұрын

    Bou feke pote sa sœur le régler se problème ak malick te bayiko te gué Def ko thi soutoure te protéger ko

  • @niangtra

    @niangtra

    5 ай бұрын

    Amina mo soutouraloul bopam, goor kendouko kham à 100/ 100, tei ki bamouy kham dieukeurou amina , amina khamouko wone, da wara neutre , lanelay gueiné di wané ay passeport tamit , na khol liy fay problème bi

  • @bushra4079

    @bushra4079

    5 ай бұрын

    ​​@@niangtradeugg deugg. Amina waroulwone exposé sa vie liii lepp mom leu, nakh mo wané Malick et Malick weulbatikou di wané lou faux motakh gars yiko kham guéneu tmt

  • @niangtra

    @niangtra

    5 ай бұрын

    @@bushra4079 bilahi barigo bou fess dou yeungou, amina leu deh ,moom niata yone la seuy? Bouko yalla mayé kénen diaroul khew, diaroul wané, vie bou discrète doundou aldianam , wayé dédet fok mou wanéwou

  • @bushra4079

    @bushra4079

    5 ай бұрын

    @@niangtra ah motakhit dina lekk thiow

  • @user-gk4sz5em7e
    @user-gk4sz5em7e5 ай бұрын

    Il faut pas avoir des amis senegalais proches en europe et usa. Probleme bofi amm senegalais molakoy tekk. C méchant

  • @miachoufall6665

    @miachoufall6665

    5 ай бұрын

    Mak yow nio yem merciii rekk

  • @user-gk4sz5em7e

    @user-gk4sz5em7e

    5 ай бұрын

    @@miachoufall6665 boulassi dara guéné ligueyi ak diamou yala

  • @muslima9599

    @muslima9599

    5 ай бұрын

    Bilay lolou lay wakh Sama borom keur chaque fois mais bon. Kou doul diangueu leçon ci senegalais yagui ci erreur

  • @miachoufall6665

    @miachoufall6665

    5 ай бұрын

    @@muslima9599 mane de nagn dem ma dem rek merciii yakhante rek lagn nekke fii

  • @muslima9599

    @muslima9599

    5 ай бұрын

    @@miachoufall6665 sincérité zéro mane mom dama ragal sénégalais. Niemewoumalene . Ya wakh deug dh. Problem rek lagn lay indil

  • @YacineFall-mm5gx
    @YacineFall-mm5gx5 ай бұрын

    Machalla ya ngui def lou bakh

  • @rockygaye-bc6rw
    @rockygaye-bc6rw5 ай бұрын

    Je comprends maintenant,yow dagua nopp Amina, louko fi diare Malik gua diotél ,mome sékhale bore si ligua wakhe mais ana soutara ,ana djikoye Talibé serigne TouBa , ana dioulite, ana yeurmandé, gnake gua kérsa ,wayadi gua ,ana saye mbokou ,li séne probléme la , face to face léne gadou gua akhe nigua yéwé fitte na niawe na

  • @fatimadiallo6947

    @fatimadiallo6947

    5 ай бұрын

    Doyna waarrr dal lolou lay nourou dal

  • @rtro223
    @rtro2235 ай бұрын

    Senegal la guise rèw bo xamnè khastantè waxantè lou gnaw xoulo xeex devoilè vie privee sr les reseaux mane defw je me demande dans kel pays ns sommes alors aulieu gnu prèocupèwu ci xeuyu ndaw yi santè agriculture elevage li developer rèw mais mm les senegalai lou gnaw aka wèrantè lagnu gueune sawar tok dici discutè😢😢😢😢😢

  • @ramndondiaye2113
    @ramndondiaye21135 ай бұрын

    Mère yi kopar rek bilay santé n'a samay weuydiour messougnouma l'affaire khaliss motakh loup ame gnom lay ndieuk khalate

  • @absadiop8022

    @absadiop8022

    5 ай бұрын

    Walahi sama yaye mousouma wakh diokhma 10fran

  • @diodiodiouf1845
    @diodiodiouf18455 ай бұрын

    Mashallah dieuf mane teral sama yaye rk la teral

  • @fatoumback
    @fatoumback5 ай бұрын

    C’est vrais dé city zeune day ame drapeau USA 🇺🇸 si bire lolou ame la

  • @MereBah
    @MereBah5 ай бұрын

    Say mame d'où massive sall kesse yaye borom mamy transporteur yi ti medina dieuf dieul yawmame bou am millionairela 11:09

  • @oumygueye7201
    @oumygueye72015 ай бұрын

    Il est tant que Amina retrouvé sa bonheur

  • @oumoukhairysamb6965

    @oumoukhairysamb6965

    5 ай бұрын

    son bonheur

  • @Ndeyefato

    @Ndeyefato

    5 ай бұрын

    Woy 😂😂😂😂😂

  • @mamanngom9490

    @mamanngom9490

    5 ай бұрын

    Mo khagne bopom bonheur dé

  • @user-ji2ly7uz2g

    @user-ji2ly7uz2g

    5 ай бұрын

    Nopil ba degg gueye ndioro

  • @mimikeita4262
    @mimikeita42625 ай бұрын

    Bilahi Malick fall yi barina Europe Li dal Amina moma dal dama siwoul rék wayé boul déglou kéine boula enrangéwoul boul déglou divorcelle khaléyou guoor you biri amougniou dra dagniouye feine ba takala

  • @misstchiptchip2963

    @misstchiptchip2963

    4 ай бұрын

    😂😂😂 moi aussi pareil..mais j'ai démasqué le gars 4 semaine avant notre mariage j'ai annulé et je l'ai bloqué de partout

  • @user-kj8sw2rc8x
    @user-kj8sw2rc8x5 ай бұрын

    Tu as raison myma Dieng,les gens sakh sont fatigués thi vie privée djambour yi ak defante bi

  • @maremediagne5713
    @maremediagne57134 ай бұрын

    Yalnala YALLA fay. Beug nala kou beug sa yaye ma.fonk la ❤

  • @FallouDiouf-ck7bv
    @FallouDiouf-ck7bv4 ай бұрын

    Mane kham nala dh brome bakh gua magui Amérique daguay diapalé bôye yi bilhai nite geu noula 🙏🙏🙏

  • @nenekeita8720
    @nenekeita87205 ай бұрын

    Pourquoi cette méchanceté choisissant sa waye

  • @user-wf9vx3dg8v
    @user-wf9vx3dg8v5 ай бұрын

    Bilay yeuw ya yess. Loutah bougo guiss bonheur diambour 😢

  • @louisefaye8187

    @louisefaye8187

    5 ай бұрын

    Tu n as pas compris. Il y a des gens qui doivent de l argent aux autres et osent faire du batrè á la television. Ils n ont rien en general. C des faux types. Il faut les denoncer.

  • @user-rs7nn6tz7j
    @user-rs7nn6tz7j5 ай бұрын

    For real bro i like it

  • @mansatacoucoukonate2234
    @mansatacoucoukonate22345 ай бұрын

    Est-ce que qui ça va? Doo baii diabour niir Yalla.

  • @KhadySarre-gx6fn
    @KhadySarre-gx6fn5 ай бұрын

    Wadji est ce que doofoul Lou so Yonne ti seye diabour madoil

  • @didishudieye7408
    @didishudieye74085 ай бұрын

    Kéne dou défale sa wadiour Lou baxe dika waxe si internet bi gnola eupelé foufe dé douneka waxe

  • @mamadoundiaye1724
    @mamadoundiaye17245 ай бұрын

    Sokhor amna bilahi

  • @abakarafall6276
    @abakarafall62765 ай бұрын

    Machalla baye fall bi

  • @sophiadia7228
    @sophiadia72285 ай бұрын

    IL ya 2 photos sur Les passport American en haut et bas, wakhal loula woeur😂😂😂

  • @moussagueye7208
    @moussagueye72085 ай бұрын

    Senegalais nio niak fayda...ils passent tout leur temps a polemiquer sur KZread 😂😂😂😂

  • @ndeyefatoudeme4186
    @ndeyefatoudeme41865 ай бұрын

    Linga sékh ak sa yay Diaroul di wakh amna kou défal yayam louko raw té noppi

  • @amisao8397
    @amisao83975 ай бұрын

    Sayayi amoulou saneta❤❤❤

  • @matardieng-cr9xs
    @matardieng-cr9xs5 ай бұрын

    Waw dieuf dieul mbeur la kay

  • @user-sc8ww5nq2f
    @user-sc8ww5nq2f5 ай бұрын

    Yén ki esceque werna layy yaw koula khol khamné da nga nopp amina ba weureudi

  • @rokheyawade1921
    @rokheyawade19215 ай бұрын

    Ce ga est ce qu’il est normal ?

  • @durkio5486
    @durkio54865 ай бұрын

    Baye fall momoul ligay def ,

  • @mounadiop3282
    @mounadiop32825 ай бұрын

    Yow dee tu est méchant 😢😢

  • @SaliouToure-gi1ue
    @SaliouToure-gi1ue4 ай бұрын

    Si Serigne saliou ça vérité dans ton coeur ne fait pas comme ça

  • @elizabethndione8558
    @elizabethndione85585 ай бұрын

    Mon frère arrête s'il te plaît la vie c rien lesse tout nguir serigne touba

  • @aissatoudiallo4107
    @aissatoudiallo41075 ай бұрын

    Tieuye Éskéyye

  • @user-qw7ee3fh6m
    @user-qw7ee3fh6m5 ай бұрын

    Lo def khep ko yaye amoul faye

  • @Samb954
    @Samb9544 ай бұрын

    Dieuf dieul da nga sokhor billahi barki seringe saliou 😢

  • @user-ss4ts2fk7s
    @user-ss4ts2fk7s5 ай бұрын

    Pourtant moune na wakh deugue

  • @user-gb7ml9kj2o
    @user-gb7ml9kj2o5 ай бұрын

    Amina sayelesaseye mouguene lanemouye amirca amirca bakhaloukherla

  • @SeynabouNiang-re6ig
    @SeynabouNiang-re6ig5 ай бұрын

    Yaw gorr dou bari wakh boula togne ga yobouko thie yonn mou diekh soff

  • @lafemmedeomar6061

    @lafemmedeomar6061

    5 ай бұрын

    Mo taye wakhe Sathieu daffa wara siw avant qu’il fasse d’autres victimes.

  • @lafemmedeomar6061

    @lafemmedeomar6061

    5 ай бұрын

    Non Sathieu bi laye siwale wala tu de famille du truand FALL ???

  • @diagnegnilou1078

    @diagnegnilou1078

    5 ай бұрын

    Wahaldé

  • @diagnegnilou1078

    @diagnegnilou1078

    5 ай бұрын

    Lilépdiaroucowo

  • @fatoutine5299
    @fatoutine52994 ай бұрын

    Vraiment senegalais sohor nguene yakanete rek boula amale woh ko en douce woula kou proche mou fay la si soutoureu et pourquoinga bayi ba legui fi mou neke si dig bonheuram.regardez nit yi nign gnou bagne AFRIQUE des k on dit senegalais ça yest s'en holi di dag coup d Afrique en est la preuve au lieu gnou manko dioubo mais legui à l'étranger wala partout bo guisse senegalais rek da ngay Dow.boy business gno ley ndieuka kheh!do beug gnou diegue la wala hamal la ndah tôt ou tard gni gui lay kambal première erreur bo ndieuka def gnou vidéo diema yak sa life kene kou si beug avancer rek nieup di heuthie pour nga wodd!pourtant deh pour que nieup tekki il faut mou commencer par kene et kene kokou aussi il faut k mou nieme nit gni pour meune lene heuthie gnou yekkk...c'est malheureux c triste et c'est à cause d tt cela k dound bi fi cher lep di meti politique bi di diahasso...c vrai k mame yi niane nagnou mais negn def très attention parcek deuk bo ham ne yakante rek xol bou bone ça finit tjrs mal en catastrophe te gno defarat xol yi balay bobou😮 yakanete tous les jour même les bébé les nouveaux né ne sont pas épargnés liii bilay diar na tiit 😮 liii kou mou djig sah nak war nga tiiit

  • @moriciss6368
    @moriciss63685 ай бұрын

    😢vraiment mane yakhaneté bima guisse si sénégalais yi la khamoule lanela iowe amegua ak malick ndare probléme lousi yonous amina poté doko réglé ak mome avant mouye neuiw sénégal nga bayi bamou neuiwe nga taka sa radio sit bou né nga wax fa gor nga régléko ak yeufou gor sokhor ngéne meune ngéne yakhe domou adama li motakhe réw yagui avancer gnouine nous tok rék di détaille

  • @adjamairy2879

    @adjamairy2879

    5 ай бұрын

    Bilahi. Dégueuna deugueu pirr.

  • @famatamba9952
    @famatamba99525 ай бұрын

    thieuyyyy yalla senegal tite n’a trop si rew mi😮😮

  • @aichadiop5969
    @aichadiop59695 ай бұрын

    C'est la moindre des choses pour ta maman. Elle mérite plus.

  • @Mature931
    @Mature9315 ай бұрын

    wa li tamit est ce dioulite di na ko deff

  • @user-jk5zh2bi1e
    @user-jk5zh2bi1e5 ай бұрын

    Yow Dieuf Dieul kou sokhor nga....kou ignaane nga....Goor dou barri wakh..tchimmmmmmm

  • @Dieng-vk6if
    @Dieng-vk6if5 ай бұрын

    Vraiment sokhor meunoule wésou li goor dou yakh moromou gorome nek léne aye gorr yalla

  • @diatougueye5421
    @diatougueye54215 ай бұрын

    Mais iow sa khol daag na deh, niou dagal salaire Séne yaye beurina et kéneu degouléne,niaw gan lamigne torop,si tu l’aime c’est plus possible,lingay wakh ni yeup amoul sens doul way sof gan torop

  • @HamatSy
    @HamatSy4 ай бұрын

    Du courage mon frère occupe toi bien de ta maman s'il te plait

  • @SadikhFall-qi9sc
    @SadikhFall-qi9sc4 ай бұрын

    Dieuf dieul dioum gua pasport amercain 2 foto la kaye

  • @mamediorfaye1311
    @mamediorfaye13115 ай бұрын

    Mais kel ton problème en tant k ta mère tu met ses messages sur les réseaux sociaux et se vante comme ça en tant k homme oh mon Dieu

  • @user-jh8pe5ny8t
    @user-jh8pe5ny8t5 ай бұрын

    Bilaye ya bonne taa sokor amina boul wakh

  • @diopfatou7882
    @diopfatou78825 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤

  • @damembow6374
    @damembow63745 ай бұрын

    Koula khammm khamnii gaïndé gua bro

  • @Userfanta2024
    @Userfanta20245 ай бұрын

    Bayil Amina mou seuy soof nga khamal ni Amina dafa yor khol di beug te Malick la beug nekal goor yalla waay

  • @ousmanesonko2760
    @ousmanesonko27605 ай бұрын

    kou sokhor nga

  • @ibrahimaniane6508
    @ibrahimaniane65085 ай бұрын

    Bro sa problém ak wadjii yaakk wadjii leu ✍ mais s' il te plait guéneesiii poté tee djigueen daffa faible Kom daganée sa soeur konn guelawaay waro sakh toud teureum sii affaire yii nii?

  • @fieldbattle6618
    @fieldbattle66185 ай бұрын

    Fi kou ligueye dioh Say parent ham way

  • @user-jh8pe5ny8t
    @user-jh8pe5ny8t5 ай бұрын

    Dieuf ya bonne

  • @mamanngom9490
    @mamanngom94905 ай бұрын

    Yenagui wah,mais leup Amina poté leu ,bo il fallait même pas qu'elle montre son mari bay def ay térouwaté,nieup niow ,seuyo béni yone ,seuyo niari yone ,ta tro fais de mariage yalla wédi,donc bi nak keneu waroutone kham ,nek si diam ,mais lolene am rek siwalko si internet bi li senegal rek am khawma kagne ngune Di mouss rek Loula dal Yako tek sa bop.merde

  • @madeleinetraore3330
    @madeleinetraore33305 ай бұрын

    ❤❤❤❤

  • @tidianedieye6754
    @tidianedieye67545 ай бұрын

    SAWAYY YAW YAY DOUL NAK PASSPORT AMÉRICAIN YU BÈSS YI GNARI FOTO LA AM T AMOUL DRAPEAU USA..ÇA SE VOIT YAW AMO PAPIER😂😂

  • @fifily1063
    @fifily10635 ай бұрын

    Moi.je veux pas que mon fils dém AMERIQUE.ILS SONT TOUS FOUS

  • @user-jk5zh2bi1e

    @user-jk5zh2bi1e

    5 ай бұрын

    Billahi deugg la..niomm nieuppa doff

  • @ibrahimadiene3435
    @ibrahimadiene34355 ай бұрын

    Moytou lene yene sénégalais yii nek extérieur di kharito ak ay Sénégalais djiko domerame deug laniou yoor

  • @muslima9599

    @muslima9599

    5 ай бұрын

    Aka malen ragal.

  • @LisaDiatta-ed7hm
    @LisaDiatta-ed7hm5 ай бұрын

    Amo lene diom

  • @user-tc7ib6gd1o
    @user-tc7ib6gd1o5 ай бұрын

    Deuf jeul fa gua nobe omina pote' té mom noboula topal fêlé

  • @ContentOmbreSky-pr1cs
    @ContentOmbreSky-pr1cs5 ай бұрын

    My brother what is your problem, why are you disrespecting her on social media.

  • @user-jk5zh2bi1e

    @user-jk5zh2bi1e

    5 ай бұрын

    He s awful this guy

  • @diagneamsatou3473
    @diagneamsatou34735 ай бұрын

    Ltkh yénè wolen Amina poté mihhh Sokhor guen

  • @yacinediop2428
    @yacinediop24285 ай бұрын

    Ki khamna Malick dh

  • @foxthrox8025
    @foxthrox80254 ай бұрын

    Moi moi je suis victim mais jai peur de parler je suis sa voisine Saint louisaine, sa mamá et hándicap son fils aine et gentit mais malick et arnaqueur je comfirme.

  • @mansatacoucoukonate2234
    @mansatacoucoukonate22345 ай бұрын

    Wa est-ce que sava baiil diabour ngiir Yalla.

  • @mamandiordiop8524
    @mamandiordiop85245 ай бұрын

    Thiey aduna li luko fi diar... Sénégal avec ça dinagn émergé au moment où yenen pays yi où même les occidentaux nek di def wala Di xol nugnuy développer Di avancer si ay projet gnun mom gnongi took si rew mi Di weranté ,Di xawi wanté ay soutoura AK sosalanté non li ba kagn...

  • @babacarseck3366
    @babacarseck33665 ай бұрын

    Bayil di khoulo di toudou serigne Touba

  • @rokhayandiaye7375
    @rokhayandiaye73755 ай бұрын

    On dirait des enfants Massa 😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @mbodjiaissatou8370
    @mbodjiaissatou83705 ай бұрын

    Machallah yallana Allah swt féyal bopam

  • @myamandiang
    @myamandiang5 ай бұрын

    Legui deh ma bayi ay xarite woroul deh koula khamal bolene diote mou vilipendé la

  • @wourelsow1482
    @wourelsow14825 ай бұрын

    Aucune importance sa yaye loko defal khepko

  • @juanatirado5214
    @juanatirado52145 ай бұрын

    Aywaye li d'où yeuffi gor d'où yeuffi goor yalla gor d'où torokhole nawleme gor d'où feckè fougniouy wakhe lou gniaw gor d'où Def dico wakhe sa yaye boco diokhone minou diamant meunon co faye conne diaroule Di bahcou té goor daye Def yeuffi goor yalna yalla tappé kholyi wasalam

  • @ibrandiaye2055
    @ibrandiaye20554 ай бұрын

    Diuef djeulle do wakhanto

  • @mamebamba1931
    @mamebamba19314 ай бұрын

    No dieuf dieul is new passport

  • @zackariatounkara5634
    @zackariatounkara56344 ай бұрын

    Senegalais sokhorna

Келесі