Démonstration de f0rce de Sokhna Momy Kébé: Elle reçoit la famille de S. Saliou avec un Ndeki royal

Пікірлер: 64

  • @ndeyearamecamara8417
    @ndeyearamecamara84172 жыл бұрын

    Kou woyof maachaalah Doundale barké Serigne Touba

  • @killahndiaye3838
    @killahndiaye38382 жыл бұрын

    Ketchup tu commence "soof" les gens , machallah sokhna momy bébé

  • @deugrekkdeugkesse1440
    @deugrekkdeugkesse14402 жыл бұрын

    Gueweul you gore yi di dare drianké yi sooff nguene ma trop, S Momy Yalna la yallah dolli kheweul brk cheikhoul khadim

  • @ababacarseck5071
    @ababacarseck50712 жыл бұрын

    Sokhna momi yokkal wéral waw gor

  • @seynabfallou395
    @seynabfallou3952 жыл бұрын

    Machalla santalé yalla serigne bi

  • @infosn5263
    @infosn52632 жыл бұрын

    Talibè yi dinagnou yak yonou Serigne Touba . Serigne Touba dès sou gnewatone guiss talibè yi séni dokhaline douko nekh

  • @FatouMandiang-lm2ls
    @FatouMandiang-lm2ls9 ай бұрын

    Machllah 🙏💯🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @famandiaye8173
    @famandiaye81732 жыл бұрын

    Machallah machallah

  • @mortallagueye8523
    @mortallagueye85232 жыл бұрын

    Machalah

  • @mohamedsabbarndiaye791
    @mohamedsabbarndiaye7912 жыл бұрын

    Machallah

  • @Sadikhetv
    @Sadikhetv2 жыл бұрын

    Noo Senegaal neexee na ku yoor dara daal yaaye buur

  • @diallodieynaba7949

    @diallodieynaba7949

    2 жыл бұрын

    Bilahie

  • @khoudiadjittebillaymanemar7779

    @khoudiadjittebillaymanemar7779

    2 жыл бұрын

    Ayway yena sokhor dieme lena ame limou ame té nopii ndm🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @mamadoudjigo7006
    @mamadoudjigo70062 жыл бұрын

    Machalaha yoodi feewi

  • @Sadikhetv
    @Sadikhetv2 жыл бұрын

    Ban fammi Sëriñ Saaliwu yeena mana fenn

  • @amyndour5278
    @amyndour52782 жыл бұрын

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️👌👌👌

  • @baegirl8049
    @baegirl80492 жыл бұрын

    Cherchez l’argent, woutilene xaliss, Légui dafa melni mbaakh si xaliss nagn key guissé

  • @etiennesnciss9556
    @etiennesnciss95562 жыл бұрын

    Apparemment quelle est l'essence du magal ? On dirait du tourisme de loisir

  • @minajoli313

    @minajoli313

    2 жыл бұрын

    Lousi sa gatt

  • @maimounadiakhate3486

    @maimounadiakhate3486

    2 жыл бұрын

    Étienne bayil togn

  • @abybathily8221

    @abybathily8221

    2 жыл бұрын

    @@minajoli313 mina saga bi diarouko nenou rafeteul adina wa Salam

  • @ngommc6202
    @ngommc62022 жыл бұрын

    Serigne toumba lépeup khéweul la🥮🥗🍱🍳🍗🥙🍓🍒🍇🍎🫒🍐

  • @famandiaye8173
    @famandiaye81732 жыл бұрын

    🥰🥰🥰🥰

  • @wallybalagoseckfans1861
    @wallybalagoseckfans18612 жыл бұрын

    Marshala

  • @Sadikhetv
    @Sadikhetv2 жыл бұрын

    Waa kër Sëriñ Saaliwu xamuñu kuy Moomi Kébé Waxee léen të bàyyi waa kër Sëriñ Saaliwu

  • @aissatouseydi5564

    @aissatouseydi5564

    2 жыл бұрын

    Koumpa motax ma setann mane xana dedett niou bayi senn keur baye niow ci ndawci

  • @jazzjazz4902
    @jazzjazz49022 жыл бұрын

    BAYIL TOGNE BOUCHER SOKHNA AIDA DIALLO AMNA ÑIOU LA MOUNA REGLER TEE DOU MOUDJ FENE. BAKHNA DEEMAL REK

  • @diordieng8032
    @diordieng80322 жыл бұрын

    Kebe ndiouga adouna rek ngaye were bilay yi

  • @fayemingue3597
    @fayemingue35972 жыл бұрын

    Ketchup liguay wakh yagui foune moytoul😂

  • @infosn5263
    @infosn52632 жыл бұрын

    Serigne Touba digeuloul li djiguène ah goorr diakhasso lek rek khassayite zéro tiakhane rek vous tous

  • @sokhnakebe1326
    @sokhnakebe13262 жыл бұрын

    thiey senegalais filmer molen sonal

  • @ngommc6202
    @ngommc62022 жыл бұрын

    Ay ketchup mo bari wakh😅

  • @cheikhtoure3066

    @cheikhtoure3066

    2 жыл бұрын

    Thieuy xalise kou yaboudè woutko

  • @ngommc6202

    @ngommc6202

    2 жыл бұрын

    @@cheikhtoure3066 wayé thiowli thiowli moy youtko takhouko am sama wadji..yala koy bakhé diam bi

  • @thiawambow3783
    @thiawambow37832 жыл бұрын

    Gréfasse thi biir touba

  • @saradieng4097

    @saradieng4097

    2 жыл бұрын

    Ak khèsale bi nak

  • @aminaniang1895
    @aminaniang18952 жыл бұрын

    Mane samay beutes mo nékhoul waleu greffage la guiss wala bok dani ayé gni méche bayi gnéne gni damey lathié rek nak

  • @ngonesene6378
    @ngonesene63782 жыл бұрын

    Yaw kethiop ya sooff founè nga néfa bou yaguè nga doone nafékh thim fékhél am sa dalou bop com sa nawlè yi ngay weur di filmés niak classe 0000000000 personnalités

  • @binetourassoul3870
    @binetourassoul38702 жыл бұрын

    Wadial n'a magal gui dh diwou gua ba wékh tal

  • @jeannesy814

    @jeannesy814

    2 жыл бұрын

    mdr

  • @yayefallfall7061

    @yayefallfall7061

    2 жыл бұрын

    Ga nieme ko wakh

  • @saradieng4097

    @saradieng4097

    2 жыл бұрын

    Tè khèsale bi ak cheveu

  • @fatoufall5601
    @fatoufall56012 жыл бұрын

    Mome dafa tabé thi liko yalla dékk boudoul magal sakh nilamél

  • @bayemodousarr5405
    @bayemodousarr54052 жыл бұрын

    ma bagne gor bouy topou diguénne ghir alalou adina geum lén sén bopou mo gueune

  • @pablothiam89
    @pablothiam892 жыл бұрын

    Ketchup ya ngui beugue sof nak, bayi mar tâte

  • @cheikhkane1376
    @cheikhkane13762 жыл бұрын

    Khamna nakk ibadou yi sene khol yagui dagu bone waye dinagne dee deh

  • @dykha8182

    @dykha8182

    2 жыл бұрын

    Nioune affairou al dunya yeu.gueulouniou

  • @oumarngom4799

    @oumarngom4799

    2 жыл бұрын

    Li day rek le

  • @ndeyefatoucisse7829

    @ndeyefatoucisse7829

    2 жыл бұрын

    Segnebi li lousouy yonou ibadouyi banguanane séne khol mongui dague li kaye sougnou yone nékousi nak boul togne li dou lislam ay poukaré Késé ak guor youye topou djiguéne di lambar lambari li lousi sougnou yonne haaaaa ma warou yeufi thiakhaneyi lo gnousi toudé gnoune li gnorognou li islam sakh khégnoufa wakhoumalak difa nék ak concour khésal concour passar pasari gnoune dagno falé li gnoune charia lagnouy weur khala lahou khala rassoul mome lagnouy weur mai dieuf you souféyi

  • @ndeyefatoucisse7829

    @ndeyefatoucisse7829

    2 жыл бұрын

    bokalé bokalé rèk nguamane ibadouyi séne khol yangui dague khana bokalé bi dé mome métinagnou chiiiiiiiiiiimmmmmmmmm

  • @fatouciss2950
    @fatouciss29502 жыл бұрын

    Boucher😡

  • @yacinembodj6712
    @yacinembodj67122 жыл бұрын

    Non

  • @adamagueye8949
    @adamagueye89492 жыл бұрын

    Kiii koumou si adina???

  • @mariamdieng199

    @mariamdieng199

    2 жыл бұрын

    c'est la fille du milliardaire Ndiouga Kebe, il est décédé

  • @mamifall2631

    @mamifall2631

    2 жыл бұрын

    Ok

  • @loubess2022
    @loubess20222 жыл бұрын

    Waw mèches yii ma Yako Rona daffa arram rien Sénégal

  • @Ousmanesonko5

    @Ousmanesonko5

    2 жыл бұрын

    Ki kraw la yorr dee

  • @loubess2022

    @loubess2022

    2 жыл бұрын

    Ok Balma akk dee

  • @kanemariam7119
    @kanemariam71192 жыл бұрын

    Ay boufébi

  • @domoudjolof367
    @domoudjolof3672 жыл бұрын

    Kham na day ngéune douche yi bamou féss tarikha bo kham ni lék rék yallah mome zéro affaire yi dou khaliss déh juif yi nion fi eupe khaliss si monde bi déh nion fi guene bone yallah kholou amam déh vous cette trompée

  • @khoudiadjittebillaymanemar7779

    @khoudiadjittebillaymanemar7779

    2 жыл бұрын

    Iow dei ya meune ndeye doul Serigne touba si loumou sokhla louneiii silagn kokoy santalei mouy berndé diangue alkhourane ak khassida yi. Iow mi nekk si benene tarikha bou sa wassila amone li sokhna si ame day daww ba fatt doul ndeyam wayy Ngay diay meune dingatt ko khamoul deko woweii héeeee Dmrm ignorant k t'es

  • @mamysakho6193

    @mamysakho6193

    2 жыл бұрын

    Sa kholal dieih

  • @domoudjolof367

    @domoudjolof367

    2 жыл бұрын

    @@mamysakho6193 khana sa khôl Lou ndeye mo diekh diogou bi

  • @aminatadiakhate2971
    @aminatadiakhate29712 жыл бұрын

    Machallah

Келесі