BALLA GAYE 2 téw na si "nganale" weydiour BOY NIANG 2 yi....yeukeuti na fa ay kadou you am solo.....

Пікірлер: 132

  • @sambaba683
    @sambaba68311 ай бұрын

    No Balla guaye2 mo goro borom khol bou raffette leu ki woroul nèkka mbeur sakhhhh billahi kèn dou balla guaye2 wayyyy machallahh ❤❤

  • @veroniquenatack7392

    @veroniquenatack7392

    11 ай бұрын

    **Bilay walay ki rk khôl ba rafette machallah ❤😍😘🥰*

  • @amdysall1273

    @amdysall1273

    5 ай бұрын

    Yalnako yalla lafal thiattt amine ❤

  • @fayeomar-bt7sl
    @fayeomar-bt7sl11 ай бұрын

    N’en barcke seydina Mouhamed balla gaye nitt kou bakh laa kou am yitté walahi yalna yalla samm lénnn

  • @YoussouphaGaye-en8jo

    @YoussouphaGaye-en8jo

    11 ай бұрын

    Sallalahou aleyhi wa salam

  • @aladjifalloudia4915
    @aladjifalloudia491511 ай бұрын

    Balla gaye liii mou takh ma begue kou bilaye borom xol bou réfét bi adouna amol solo na lépou réfét ❤❤❤❤❤❤❤

  • @AbdoulAzizKande
    @AbdoulAzizKande11 ай бұрын

    Bilahi Mane dama rousse sakh kouma geuna bagne balla gaye gisoumako mais Limou déf ni takh n'a ma beugue ko dou sama mbeur nak Mane Modou lô moye sama mbeur balla gaye yague fi Lolou té wére bilahi ❤️❤️

  • @damebadiane2251

    @damebadiane2251

    10 ай бұрын

    Bo ko beugué tmt ama louko ndieurigne daguaye bagne koula falé

  • @moibarrys3749
    @moibarrys374911 ай бұрын

    Balla niiit leu déh machalah vraiment c'est ça être un grand homme ❤

  • @tidianesylla8618
    @tidianesylla861811 ай бұрын

    J’adore la mère de boy Niang 😇elle communique bien

  • @noumoufaaboubacardiop1753

    @noumoufaaboubacardiop1753

    11 ай бұрын

    Walaye regarde comment elle accueillir balla gaye ooohh j'ai la chair de poule 🙏

  • @AbdoulAzizKande
    @AbdoulAzizKande11 ай бұрын

    Bilahi lounouye wakh si balla gaye silou gnawe Dara amousi barki alkhourane balla gaye kéne geunoula khôl djiko yonène tibi deuge guafi déf

  • @syissa3940
    @syissa394011 ай бұрын

    Thiey balla g 2 esprit de grandeur le champion. Un grand monsieur. Kholou diamant

  • @malickcisse4688
    @malickcisse468811 ай бұрын

    Bilay Balla gaye ya bakh yalla nassa diame yague.boye niang yalla nanga nek roi des arened

  • @alphabarry4353
    @alphabarry435311 ай бұрын

    ❤❤❤très très beau geste Beug n'a seydina mouhamed toudei n'a ko doom ba parei li moy sénégal un bon exemple a prendre yalna borom bi nangou adj gui boy Niang thiapathioli bi yalna and wi sakh

  • @user-ei4ph3wd3t
    @user-ei4ph3wd3t11 ай бұрын

    Billahi balla gaye2 niit kou bakh la ❤

  • @faye6718
    @faye671811 ай бұрын

    Machallah amnasolo Balla merci beaucoup vraiment borome bakh nga ❤❤❤

  • @BadianeNene
    @BadianeNene11 ай бұрын

    Machalla balla xol bou réfét la am ❤❤❤

  • @pierremendy6053
    @pierremendy605311 ай бұрын

    Balla you are definitely a very good person, this is a very nice gesture respect ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mmcheikhndiaye-um8tp
    @mmcheikhndiaye-um8tp10 ай бұрын

    Machallah Balla raféte na trop longue vie champion ❤🥰

  • @sidyndiaye9669
    @sidyndiaye966911 ай бұрын

    Machallah lu moy Sénégal 🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤❤❤yalna len yalla defal diam

  • @user-jy3mm5kb4q
    @user-jy3mm5kb4q10 ай бұрын

    Mane Meussouma Farale Balla Gaye 2 Walahi Mé à partir d’aujourd’hui Diap Nala Bilahi Walahi Tallahi Barké Seydina Mouhamed Saw Beugue Nala 🙏🙏🙏😭😭😭

  • @momobouthiapathiolybi7752
    @momobouthiapathiolybi775211 ай бұрын

    Ndeysane li koussi contanoul da nga sokhor😂😂

  • @veroniquenatack7392

    @veroniquenatack7392

    11 ай бұрын

    *Waww wawww❤❤❤❤*

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack739211 ай бұрын

    *Sama wadji BG2 say boumako guissé réeee ndakh thiofel bimay yégue thi momm❤🥰❤❤ 🥰sa khôl rafette na am gua yitté do diapé dara mouy dara machallah diam thi ioe😘😘😘😘🥰ligua deff nice na Boy Niang diam thi ioe itam🥰😍❤️*

  • @user-er5bf7tw8d
    @user-er5bf7tw8d11 ай бұрын

    Balla gaye 2 dou sama mbeur mai khôl bou Nice la yoor

  • @veroniquenatack7392

    @veroniquenatack7392

    11 ай бұрын

    *Bilay walay deugue rk gua wakh mane momm rk la beugue mei en mm tps khôl boumou yoorr daff ma nékh❤️🥰*

  • @massambaseye8129
    @massambaseye812911 ай бұрын

    Macha alha Balla gaye 2 vraiment sa xool rafétna

  • @user-ox5ee8tk2b
    @user-ox5ee8tk2b11 ай бұрын

    Vraiment Balla noble deuge ga

  • @user-wk4mb9ux1q
    @user-wk4mb9ux1q11 ай бұрын

    La grandeur de balla gaye

  • @sidigueye6210
    @sidigueye621011 ай бұрын

    balla niiko wer niioy wax rek mai il est gentill

  • @user-gh4gs4nl4y
    @user-gh4gs4nl4y11 ай бұрын

    J’aime bien balla gaye nit guénokou ❤❤❤❤

  • @moustaphacisse5549
    @moustaphacisse554911 ай бұрын

    Thiaye sama wadji yalna dollia samou BG2

  • @diagnebass6754

    @diagnebass6754

    11 ай бұрын

    Sunu wadji😂😂

  • @veroniquenatack7392

    @veroniquenatack7392

    11 ай бұрын

    @@diagnebass6754*ci bcps srtt lolou sougnou 😂😂*

  • @khadimmbaye5447
    @khadimmbaye544711 ай бұрын

    Mogeun ❤thi lambji

  • @cheikhfall4729
    @cheikhfall472911 ай бұрын

    Très beau Geste des lutteurs

  • @cheikhfall4729
    @cheikhfall472911 ай бұрын

    Franchement li refét Na trop WAyy bravo a boy Niang 💚❤️

  • @mamediarradiakhoumpa6000
    @mamediarradiakhoumpa600010 ай бұрын

    Machalla Balla Gaye 2 Nit kou Bakh leu Machalla❤

  • @cheikhfall4729
    @cheikhfall472911 ай бұрын

    Balla Gueye si bopam Pikine là waron deuk ndax ki pikine dagn ko beug ba paré deretou pikine la Yor

  • @beinz9482

    @beinz9482

    11 ай бұрын

    Diabaram Pikine la deukk aussi

  • @cheikhfall4729

    @cheikhfall4729

    11 ай бұрын

    @@beinz9482 waw XAMna lolou nietty mbar ndeysan

  • @alphacheikhsylla4071
    @alphacheikhsylla407111 ай бұрын

    Balla Gaye 2 rek merci beacoup ❤❤❤

  • @yacinediagne5654
    @yacinediagne565411 ай бұрын

    Balla Moy Sama Mbeur Boy Niang Sama Mbok Talibé Niom Niar Ay Nit You Bakh Laniou Je Vous Adore❤️Mashala…Bon exemple Bon Geste Adouna Dou Dara

  • @amdyfall4163
    @amdyfall416311 ай бұрын

    Machallah balla gaye 2 boye Niang 2 après balla gaye 2 yaw yaye sama Mbeur diantall bro yomboull si Mbeur

  • @seydinamandioneniasse6673
    @seydinamandioneniasse667311 ай бұрын

    Balla gaye moye gooree dama Khamene lamb rek nou dieule sa tour AK sa tourou yaye dila dathieu si gouye diko wane direct pour yene la Lou bonne taye ngaye dème keureume diko ziare kou diara yeureume nga balla gaye

  • @mouhamedmoustapha684

    @mouhamedmoustapha684

    6 ай бұрын

    Balla Kay dafa baxx rek bilay man mom soma dané dotoumala lidieunti surtout liko degaul wax yeup mais balla xol bi mo rafate

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo917111 ай бұрын

    Ballam mobah mé kéna d'où yaye boy Niang mère yay gor fotog diwah si Balla. Yalla nalla Balla guaye yobou mag.

  • @ThiateLambassadeurKandji-mw2ie
    @ThiateLambassadeurKandji-mw2ie11 ай бұрын

    Ndayessane yalla nalléne yalla same balla gaye 2 borom bakh nga yalla khamnako

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage648211 ай бұрын

    Gni aye mbeur you nitte laniou diarama baboye balla guaye 2

  • @mamadousow4392
    @mamadousow439211 ай бұрын

    li moy sénégal li tamite laniou hame yalla na diam yag

  • @ndoffenediouf2749
    @ndoffenediouf274911 ай бұрын

    Balla gaye Barki Cheikh Ahmadou bamba ya bakh ya goré

  • @ahmedrage-cf2np
    @ahmedrage-cf2np9 ай бұрын

    Machallah balla gueye2

  • @ndiaboutadiouf9300
    @ndiaboutadiouf930010 ай бұрын

    motakh nit loy Def nangasi dème akk khel ndakh ama balde ben instant dafa beugeu lou nekh balla khawa sori boy niang ndakh pikine dagnouko mère ndakh balla mais temps yi dama setlou ben.distance .si balla akk ama. Depuis audience de palais bi tay balla gaye mongui keur boy niang mais yalla bakhna ama kou bakhla c'est que encadrement nio nelaw mbok lou bakhla mais kou am nagg sa keur baye ngakoy yobou dafa diot ama am li nieup di si lamb lolou lako yenne bilahi molen meun geun.len bakh palmarès mais loloou rekk doyoul le business est très important dans la lutte ama boul top Ken topal

  • @saliousow6563

    @saliousow6563

    10 ай бұрын

    Kokou mom entourage bi mo bakhoul motaxe dou diokk ci ay tookhidouna😂

  • @hamzaseck6630
    @hamzaseck663011 ай бұрын

    Tres bien vive le Sénégal❤❤❤❤❤❤ et vive la paix 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳merci beaucoup

  • @ycamara9034
    @ycamara903411 ай бұрын

    Bad boy go to Makka ooohhh that is Nice 😁😁😂😂😂😁😁😁👍so now be good boy forever ok ok😁👍

  • @aminatadiagne3293
    @aminatadiagne329311 ай бұрын

    Li betouniou si balla Gaye mom ni rek toujours koumou beurel mou dane la wala nga dane ko si boulay nehh rek apres relation fraternelle lay geun di firdell Nitt kou oyof kou bah kou beug diam Ahlou lamb niola wara fall balla le régulateur

  • @veroniquenatack7392

    @veroniquenatack7392

    11 ай бұрын

    *Bilay walay wakh ko thi kaw sougnou wadji amoul morom khôl ba nice❤❤😍😍🥰🥰*

  • @babacardiop5162
    @babacardiop516211 ай бұрын

    Balla mo bari bairé 😂😂😂😂

  • @theressebasse8667
    @theressebasse866710 ай бұрын

    Balla moy lamb kouko bagne beugo lamb bilay walay 🙏

  • @saliouba9428
    @saliouba942811 ай бұрын

    Machallah yalla na diame yague

  • @baimamud1491
    @baimamud149111 ай бұрын

    Masha’Allah ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @adandoye3759
    @adandoye375911 ай бұрын

    Ngor si ndiaye legui mu géneu wakh mome Lou rafét lay bagna guiss 😂😂😂😂🤦🏽‍♂️

  • @veroniquenatack7392

    @veroniquenatack7392

    11 ай бұрын

    *Bilay ioe 😂😂😂khôl ba ndaw mtx day khassane foumou tolou😂😂😂*

  • @SerigneBassirouMbackeSen-zn3xk

    @SerigneBassirouMbackeSen-zn3xk

    11 ай бұрын

    😂😂😂😂😂😂😂

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo917111 ай бұрын

    Vrément JM la mère de boy Niang. Na yayou mbeur yi Djang si adjaratou mou sélmi yalla nafi yag t wér.

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo917111 ай бұрын

    La mère de boy rassemble a la mère de boy Niang. Yaye Balla kimobg sa dom démal sétiko Dina donne Lou gana nice.

  • @mbouganethiaw10
    @mbouganethiaw1011 ай бұрын

    Focus 2024 ba paré mo eup solo

  • @tallafall7629
    @tallafall762911 ай бұрын

    Machalla amatina solo

  • @guez655
    @guez65511 ай бұрын

    Machallah contana trop sama khole sédena trop ndakh beugeu boye niang 2 bilahi

  • @alassanemane3021
    @alassanemane302111 ай бұрын

    Machalah li rafetna trop billah ❤❤❤❤❤❤

  • @DTFTV
    @DTFTV11 ай бұрын

    Machallah Nice na trop

  • @diamourek3447
    @diamourek344711 ай бұрын

    Machallah nice na bilaye ❤❤

  • @AbdoulAzizKande
    @AbdoulAzizKande11 ай бұрын

    Digua bagne nitt fék Dara waralouko loudoul noname yiguaye togual balla gaye mbeur yeupou yasi geune bilahi mbeur bou mélni yéw amoul dou si lambou dji bilahi dou sama mbeur nak lakoye commencé bilahi

  • @AbdoulAzizKande

    @AbdoulAzizKande

    11 ай бұрын

    Sama mbeur nak lakoye commencé Modou lo AK kénene koudoul mom bilahi

  • @ndiaboutadiouf9300
    @ndiaboutadiouf930010 ай бұрын

    man ma yen ama balde bilahi

  • @diengmourtalla6250
    @diengmourtalla625011 ай бұрын

    Mane dh mérewone nako torop mé limou déff ni rafétte na torop billahi

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo917111 ай бұрын

    Les jeunes lutteurs bayiléne hél thi li attention.

  • @oumarndoye1169
    @oumarndoye116911 ай бұрын

    Pere deguaul khana wargua rouse dé ligua lepe si bala guay 2 no bala guaye ya bakh bilakhi

  • @bakhyayeniang2605
    @bakhyayeniang260511 ай бұрын

    machalla lou rafftte da raftte walay

  • @aliouneba3108
    @aliouneba31089 ай бұрын

    Wallahi khôl bi da rafet MachaAllah ❤❤

  • @bathieniang6411
    @bathieniang641111 ай бұрын

    Modou lô de Moy sama mbeur dh waye balla khol bi dara nekousi barke s touba

  • @moussadiarra4729

    @moussadiarra4729

    10 ай бұрын

    Bayyilen sokhor

  • @amdymoustaphagueye2465
    @amdymoustaphagueye246511 ай бұрын

    Machallah yalna diam dji sakh😍😍🙏

  • @hawadiagne7221
    @hawadiagne722111 ай бұрын

    Machallah diam nekh way.yalna diam yague

  • @gabrielngom7185
    @gabrielngom718510 ай бұрын

    Rafétna fils ! 👍👍👍👍😊

  • @moustaphatine7422
    @moustaphatine742211 ай бұрын

    Des ❤ SVP 🙏 Ça c'est beau vraiment ♥️♥️♥️

  • @kourel2wilayalouga55
    @kourel2wilayalouga5511 ай бұрын

    Machalla

  • @mamadoundaw7980
    @mamadoundaw798010 ай бұрын

    Mo gueneu raféte khole si mbeur yi

  • @yusuphajallow1257
    @yusuphajallow125711 ай бұрын

    I'm so happy 😍

  • @user-ui5rw6it3f
    @user-ui5rw6it3f11 ай бұрын

    Ndaysne ❤

  • @mamanseck3365
    @mamanseck336511 ай бұрын

    Nn sama khol toyna sakh ki niit la en

  • @ndeyemaguettembaye3649
    @ndeyemaguettembaye364910 ай бұрын

    Borom ❤❤❤ bou reuy bi balla gaye 2 y’a bakh

  • @yousb7299
    @yousb729911 ай бұрын

    Mettez du respect sur son nom

  • @abdouseck5178
    @abdouseck517811 ай бұрын

    Barki alkhourane mo gueuneu si adouna

  • @alimadiop3689
    @alimadiop368910 ай бұрын

    Balla nitt guenou ko

  • @ballydiop9101
    @ballydiop910110 ай бұрын

    Mba Walen gua ni papaye boy Niang ak yayou boy niang saxx Balla Gaye 2 laniou faral mais doom mon sory si xol rekk😂😂😂😂😂😊

  • @ibrahimambaye1289
    @ibrahimambaye128911 ай бұрын

    Akay deugue kha du nitt sakh 😂😂

  • @fansarakeita7172
    @fansarakeita717211 ай бұрын

    Balla champion deuguu

  • @abdouthior1205
    @abdouthior120511 ай бұрын

    Ndeysane sportif la balla gueye

  • @aminabah4777
    @aminabah477711 ай бұрын

    Ndeysan yalla na diam yagueu

  • @DivaLadiva-cr1yl
    @DivaLadiva-cr1yl11 ай бұрын

    Machalla li nice n'a trop

  • @kaas1610
    @kaas161011 ай бұрын

    Khadim ndiaye mou ngui nieuw dè 🤣🤣🤣

  • @tidianesylla8618
    @tidianesylla861811 ай бұрын

    Balla 🔥

  • @pierremendy6053
    @pierremendy605311 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @moussaba4865
    @moussaba486510 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤

  • @ramacobar
    @ramacobar10 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo917111 ай бұрын

    ❤❤❤

  • @eugeneselassiejr4856
    @eugeneselassiejr485611 ай бұрын

    ❤❤❤❤❤

  • @ganaseck5863
    @ganaseck586311 ай бұрын

    Nganalé deh môme waroul mél nii lii si mélni nguènté🤧

  • @mbayegueye2303
    @mbayegueye23035 ай бұрын

    Berty

  • @yakinesene1649
    @yakinesene164911 ай бұрын

    Niepe.contane Nagnou.yala.naniepe.am.diame

  • @papekarballahndiayendiaye6022
    @papekarballahndiayendiaye602211 ай бұрын

    Kou bakh laa mais boum dougueee afaire d politique lakooo yakhhh

  • @ibrahimandao570
    @ibrahimandao57011 ай бұрын

    Souniou Yonne nékoul si yéna bokou palais des 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅

  • @bosstakh8995
    @bosstakh899511 ай бұрын

    Nit daal nite waye topou réseaux sociaux yi ak internet bi di khoume kou rek di wakh wakhi dof sa morom yi di dieufandiko sen khel di avancer yaw nga kale kak rek gnounanla ya fi nekal askanwi thimmm wayadi

  • @meujnatdiakhate8470

    @meujnatdiakhate8470

    11 ай бұрын

    Yow geuna wayadi gneup...gni ay defean lagnou ak yow momou di wakh

  • @massfaye5946
    @massfaye594611 ай бұрын

    Balla gaye nit deug leu

  • @abdouthior1205
    @abdouthior120511 ай бұрын

    No balla delen touché

Келесі