Arrêté et Déféré par la Police? Lac 2 en prison, Son petit frère réagit : « Traffic de visa ladone…

Пікірлер: 265

  • @People221sn
    @People221sn20 күн бұрын

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL

  • @kingandresito
    @kingandresito20 күн бұрын

    Boy maitrisewo lois Meuytoul ma micro yiii digua wakh ba dougeul sa makkk

  • @footballresumedirect2391

    @footballresumedirect2391

    18 күн бұрын

    Bilay lou ler ngako wakh

  • @sadiocisse1326
    @sadiocisse132620 күн бұрын

    Diangual gua bagne li laye diour dans ces situation il ne faut faire aucune déclaration pour éviter de le compromettre seule son avocat est habile à le faire

  • @bibandiaye1847

    @bibandiaye1847

    20 күн бұрын

    Ce gars Kay weroule daka guena dougoule il a mal communiqué

  • @user-sb8gw2fx7k
    @user-sb8gw2fx7k20 күн бұрын

    Que le bon dieu lui protège à lac de guerre 2

  • @dakardk4750

    @dakardk4750

    20 күн бұрын

    Amine incha allah

  • @Ydakh-ui5yo
    @Ydakh-ui5yo19 күн бұрын

    Lac2- enquête la nêk yala nako tégil natou bi

  • @seydouball1161
    @seydouball116117 күн бұрын

    Yow déjà do rakkam. Bénéne bi lac mbeur la na yém thi cadre lamb. Visa kouko beugue dangay dem ambassade woutikofa. Am tour walla sîw tahoul ngay déf Loula nékh. Arrêté wougnou Modou lo arrêté wougnou Balla gaye parce que défougnou Dara. Kouné yémal thi sa domaine diam ni gnoye.

  • @papenar2561
    @papenar256120 күн бұрын

    Lac moy kane ba sou défé ndiombé ken douko dieuli yaw wero

  • @astoumbenemane3818

    @astoumbenemane3818

    18 күн бұрын

    homme de celebrite momay rey man

  • @papenar2561

    @papenar2561

    18 күн бұрын

    @@astoumbenemane3818 ah feep si adouna la keep kou def loudoul yone c normal yone tek la loxo même europe fi gnouko eup daradja lagnouy diap

  • @user-up6ub4ym1e
    @user-up6ub4ym1e20 күн бұрын

    Laissons la justice faire son travail s’il est coupable des faits qu’ils lui sont reprochés qu’il repond à ses actes

  • @YoumSaliou
    @YoumSaliou20 күн бұрын

    Ak loumanti nagneco dia pale franchement ❤❤❤❤

  • @fruityvoice997
    @fruityvoice99720 күн бұрын

    Yalla nako yallah sameuh❤

  • @fatousarr3978
    @fatousarr397820 күн бұрын

    No Sénégal nekh n'a quoi lac de guerre nék si busnessame ba am thii probléme NGA ni nitt diapalé wouniouko nako lidjanti

  • @djiboseck147

    @djiboseck147

    20 күн бұрын

    Wakh deug yalla bimouye dieule khalice bi esque wona kouko diapale

  • @2quevosquevos242

    @2quevosquevos242

    19 күн бұрын

    Nafekh Rek

  • @muzammilhussain-ed1il
    @muzammilhussain-ed1il20 күн бұрын

    Wakhall si problem yi ame ngaye wakh lenene bo si khamoull dara nopill

  • @khadimg2078
    @khadimg207819 күн бұрын

    Boy may niou diam fii dall lou way deff nako assumé Boull niou fonto boy

  • @TallaFall-or4xk
    @TallaFall-or4xk18 күн бұрын

    Kou bakh yaw amo xame xame wakh warou la 😢lac de guerre moy kane ak loumou défal deuk bi ba takh warou niouko dieuli

  • @pendadiallo2787
    @pendadiallo278718 күн бұрын

    Ndayssane yallah nako yallah takhawou ci barker Sedona Muhammad SAWS🤲🤲🤲🤲

  • @user-sb8gw2fx7k
    @user-sb8gw2fx7k15 күн бұрын

    Macha allah mon frère vs avez parfaitement raison bonne courage

  • @beuzhustle3483
    @beuzhustle348320 күн бұрын

    'es lutteurs st tellement groumant et opportuniste ils n'ont rien investi k ds l'immobilier rekkkk Di daww si guinaww xaliss rekk

  • @alioudiouf8310
    @alioudiouf831019 күн бұрын

    Saa waaay yangui dougueul lac dé... c grave ce que tu dis...

  • @AlassaneDiabira-iz3gz
    @AlassaneDiabira-iz3gz20 күн бұрын

    Baye fall,Lac bou défoul Dara,kén douko téyé,ok.

  • @sirysene88
    @sirysene8819 күн бұрын

    Que le tout puissant Lui Vienna en aide

  • @MarameSeck-qk8pt
    @MarameSeck-qk8pt18 күн бұрын

    Machalla frère bien dit deug rek

  • @cheickmoinga3245
    @cheickmoinga324520 күн бұрын

    Yalna saa borom taxawula

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf11020 күн бұрын

    Wadji mome day yokal noon lac 2 rk Di dof na trop lofay soulè yenen blem

  • @madickethiam5084
    @madickethiam508420 күн бұрын

    Oiw yangui wakh rék do nopi ndakh yangui geuna diugeul lac 2 oiw bo khamoul nopil

  • @cheikhoumarsidibe3311
    @cheikhoumarsidibe331119 күн бұрын

    Maîtriser woul fond cas bi mou begue ci wakh. Dinako gueune dogoul pck migui diokhè aye pistes sans s’en rendre compte. Moytoulène micro surtout ci cas bi nèk justice .

  • @thiernondiaye6920
    @thiernondiaye692018 күн бұрын

    Sa way sa communication bi bakhoul

  • @AlassaneDiabira-iz3gz
    @AlassaneDiabira-iz3gz20 күн бұрын

    Ngor,Lac bou yooré xaliss,naa deff Médiation pénale, c'est tout.

  • @wizkid540
    @wizkid54019 күн бұрын

    Juub juubal juubanti..❤

  • @user-jc8bx8sc2v
    @user-jc8bx8sc2v20 күн бұрын

    Lac guerre 2 il faut qu’il arrête de se victimiser il gagne bien sa vie ça ne sert rien de pleurnicher sur les télés en disant que lés gens ne me viennent pas en aide il n’a qu’à comparer sa vie actuelle et 10 ans avant

  • @fatimandao8359

    @fatimandao8359

    20 күн бұрын

    Merci

  • @amadoulamine

    @amadoulamine

    20 күн бұрын

    Merci aussi en matière de business y’a pas de sentiments promoteur kholou niou kou mana berai molo lagni weur mai yala nako yala soutoural

  • @FatouthiamGueye-ts6gn

    @FatouthiamGueye-ts6gn

    20 күн бұрын

    Vraiment

  • @youssoufabdoulayediopjohnn3774

    @youssoufabdoulayediopjohnn3774

    20 күн бұрын

    BRO KHAMGUA LAC DE GUIER DAFA WSRONEU GUEUM BOROMBI DARA KUFI LEKK KHALISSOU DIAMBOUR DAY FAY PAR FORCE BUÑOU SONNAL

  • @youssoufabdoulayediopjohnn3774

    @youssoufabdoulayediopjohnn3774

    20 күн бұрын

    BRO WAKHI DOFF IOW KI MEUNOKO SETHAL DEH BILAHII IL.VA PAYER PAR FORCE

  • @iboudiouf7673
    @iboudiouf767319 күн бұрын

    Lac il faut mou doylou di dougou si loumou maîtriser en plus lac c'est un simple citoyen instant bi phase enquête la nek bayilén yoon def liguey bi boussi taakhoul rek dina lére

  • @kanaty9313
    @kanaty931318 күн бұрын

    Wakh daye Yam

  • @badaradiouf4646
    @badaradiouf464619 күн бұрын

    Masta demal deglou dji son Ndongo lo bi dialé ma baaneex bo guiss si adouna yone dafay diss soko gnémé do baanexou soko gnémé woul do baneexou

  • @salladiallo1281
    @salladiallo128120 күн бұрын

    Diango sa way yangui dougal sa wadji la loi est très sensible danga wara nopi ba lep diekh

  • @user-ok6js4vs4h
    @user-ok6js4vs4h20 күн бұрын

    Yalna yalla def diam reek

  • @user-bb2ph5hf5u
    @user-bb2ph5hf5u19 күн бұрын

    Boy maynio jam koumou amél khalis rék nla fay liguéy dafa métti

  • @mamadouthiam3695
    @mamadouthiam369520 күн бұрын

    Mon frère yangui yokou khar bi karow dé tu n'a pas le droit de parler à l'insu de son avocat si. Tu veux l'aider arrêter de parler avec les journalistes ca se voie k tu n'est pas malin

  • @djibrilfaye911
    @djibrilfaye91120 күн бұрын

    Pour moi intervuw bi c pas l momen tu f k augmen les choc liga fi wah amoul chance

  • @64Amadoufall
    @64Amadoufall20 күн бұрын

    Lingaye wakh diotéwoul dara yoon Maîtrisewo lingay wakh

  • @maremedieng9549
    @maremedieng954920 күн бұрын

    ki il est entrain d'enfoncer lac de guerre meunoul communiquer

  • @taphasamb6836

    @taphasamb6836

    20 күн бұрын

    En tout cas dafa khamoule lois rekkk mouye ratatati rekk😂

  • @Fas9168

    @Fas9168

    19 күн бұрын

    Ki key dof bougnou peinture leu

  • @tmasterp8279
    @tmasterp827920 күн бұрын

    Mon frère c'est bien de dire au journaliste de parlé avec son avocat parce que la lois est sensible

  • @1khouredia

    @1khouredia

    19 күн бұрын

    Dafay guene douguel lac deh. Limouy wakh khamoussi dara.

  • @riobabseyeuge7914
    @riobabseyeuge791419 күн бұрын

    Say wakh leroul dé

  • @MouhamedLam-vp6rv
    @MouhamedLam-vp6rv5 сағат бұрын

    Lima méti si Sénégal nite dayy dèf yeufou domou kharam nafékk yi diko diappalé 🤧

  • @ibrahimadieng2471
    @ibrahimadieng247119 күн бұрын

    Ki dafa dof lac 2 moye Kane ba bou deffe gnombé dougnou ko jeuli

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall200320 күн бұрын

    Justice soit faite

  • @AbySene-kt2bu
    @AbySene-kt2bu20 күн бұрын

    Kouye daw rèk kène doula dane borome million rèk gnon doylouwoule

  • @coumbadinho7055
    @coumbadinho705518 күн бұрын

    Yallah ndako yallah protégé si barké alkhourane nou Karime

  • @KarimSene-gh3qx
    @KarimSene-gh3qx18 күн бұрын

    Oh ndeysane 😭

  • @cheikhndiaye6698
    @cheikhndiaye669816 күн бұрын

    Lac 2 yalla nako yalla tahawou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @franceamericanbullydogfami7992
    @franceamericanbullydogfami799220 күн бұрын

    Ce petit la est très intelligent machallah

  • @dianablackqueen3510

    @dianablackqueen3510

    20 күн бұрын

    Pas tant que ça 😔 degloul desal bi tu sauras 🙏🏽 Parfois nopi moy gueunn

  • @user-ue6mz2lm2b

    @user-ue6mz2lm2b

    20 күн бұрын

    @@dianablackqueen3510 sénégal dh golo bou dioug wah gnouné "il est intelligent" wala "pertinent" wala "yaw rek lay toppou".. 0 esprit analyse et critique lmao.. la pluspart noppi moy geune wah si lo xamoul mouy si commentaire yii ak média yii ak gnougnii interview

  • @taphasamb6836

    @taphasamb6836

    20 күн бұрын

    ​@@user-ue6mz2lm2bil suffit que ngua saff lamigne rekk pour être intelligent au senegal

  • @dianablackqueen3510

    @dianablackqueen3510

    20 күн бұрын

    @@user-ue6mz2lm2b merci là bas 💪🏾

  • @dianablackqueen3510

    @dianablackqueen3510

    20 күн бұрын

    @@taphasamb6836 surtout ça 😅

  • @en2mots817
    @en2mots81720 күн бұрын

    Y a beaucoup de gens qui n'aiment pas ce lac 2 pour la plupart des hypocrites et profiterons de ses erreurs ou d'autres choses pour le sanctionner et gâcher sa vie .

  • @bilalkhalyfall9938

    @bilalkhalyfall9938

    20 күн бұрын

    Wakhou dof saway kéneu gnanalouko liko daleu nih mais boudé il est coupable pourquoi justice douko sanctionner arrêtons d'être émotionnels gnou utiliser plutôt notre raison

  • @mamecorecisse1849

    @mamecorecisse1849

    20 күн бұрын

    😂😂 sa wayee lac2 amoul khorom safoule sucare mogueuneu nulle si arréne bi 🤭 wayé yalla nako yalla guéné fofou mou nék

  • @ModouwilaneDiop

    @ModouwilaneDiop

    19 күн бұрын

    Lolou mo yakh Senegal nitt yi danio sokhor balaniou contane rek nitt nek si ay khatt khatt balshit

  • @SaineyJagne-go5yg
    @SaineyJagne-go5yg20 күн бұрын

    Oh😢😢😢😢😢😢😢

  • @AlassaneDiabira-iz3gz
    @AlassaneDiabira-iz3gz20 күн бұрын

    Khaam Lac de guer 2 thii affaire visa,baan importance laa aam ?

  • @CheikhAnne-gg3zl
    @CheikhAnne-gg3zl20 күн бұрын

    Saway lac citoyen kom nieup amoul mbeur amoul dareu bou defei loumou waroul defff yoneu tek ko lokho

  • @user-bg4qh2up2z
    @user-bg4qh2up2z10 күн бұрын

    Lac naka assumé lek xaliss ngni na faye amna monning ,boy sofga trop.

  • @pachitopachitoeste9991
    @pachitopachitoeste999120 күн бұрын

    Taisez-vous ; une information judiciaire est en cours

  • @mamadouaidara9497
    @mamadouaidara949720 күн бұрын

    Je suis de guediewaye mais lac2 n a pas térassé eumeu sene

  • @laminediatta7069

    @laminediatta7069

    20 күн бұрын

    Lol😂 est si tu est de guediawaye nakkk mais lolou du blem soit de parcelle yofff pikine zig Tamba fuuuu nekkk lolou du du blem daffa diuommmm eume lac gagné woukoo. Lolou lu kagne diaroule niou wa je suis de guediawaye

  • @nahseck3470
    @nahseck347020 күн бұрын

    Wadji sa wax dji rafétna trop mais lamb diow la té Lac guier safoul lamb amoul supporters kon nak meunou cummulé ay avance

  • @abdourahmanebadji2846
    @abdourahmanebadji284620 күн бұрын

    Lac doit être responsable

  • @babacarsao-vc2sj
    @babacarsao-vc2sj20 күн бұрын

    S'étal yalla si liguaye wakhe khalisi boyi nako délo ta dégue na sakh niom diop khass dieul naniou anguass ma né daniou koye faff mana am soube niou bayi ko

  • @dieyeniang8775
    @dieyeniang877517 күн бұрын

    Eumeu séné mo dane lac 2boulko fater

  • @julesndoye1409
    @julesndoye140919 күн бұрын

    Pour moi on ne vend pas le visa, . Ce n'est pas juste

  • @goorandione3766
    @goorandione376620 күн бұрын

    Billahi kay😢😢😢danko wara jappale

  • @you5303

    @you5303

    20 күн бұрын

    Lac de guier môme j pense dégn KO yakh

  • @user-yd8yh5ud4p
    @user-yd8yh5ud4p20 күн бұрын

    Bilahi yaw mado da bakh

  • @matysylla5159
    @matysylla515920 күн бұрын

    Yow nopil weroulo wakho fii dara tchippp

  • @misskourouni1428
    @misskourouni142818 күн бұрын

    Tellement vide d’esprit.Non Sénégal Dou dème

  • @mouslydiba
    @mouslydiba18 күн бұрын

    Boy nianal ko mo gueune ci lii lac moy kane ba bouko justice sokhla procureur douko dieuli mounane lac kane mokoy dieulsi

  • @YoumSaliou
    @YoumSaliou20 күн бұрын

    Lac c'est un grand lutteur ❤❤❤❤

  • @senegal2

    @senegal2

    20 күн бұрын

    Dimbalenou sicatoubapyi

  • @2quevosquevos242

    @2quevosquevos242

    19 күн бұрын

    Mbeter mbeurer bou soff tek Baradah Rek dieumeuler 22h 😂😂

  • @batchpouye-cw1mp
    @batchpouye-cw1mp20 күн бұрын

    😢😢😢😢

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall200320 күн бұрын

    Bussines si visa au Sénégal on croit que outale visa dou dara koi lol

  • @user-iv3fk8ch7u
    @user-iv3fk8ch7u16 күн бұрын

    Boy yaw tu nété pas aux courant donk khamaloko 5:13 dara

  • @babaragnuing3524
    @babaragnuing352420 күн бұрын

    Boy lac2 guénagoul dé bro

  • @Maria-jk6fi
    @Maria-jk6fi19 күн бұрын

    Ame waro wakh sans Papis diokh la feu vert yagui loy guena dougual yeni nén la nopile mo guene

  • @papenar2561
    @papenar256120 күн бұрын

    Yaw waxal lo xam lac sou défoul wone dará dougnou ko té niit day doylou

  • @MbayeThioumb

    @MbayeThioumb

    20 күн бұрын

    Iow xana dagua bokou si niouniou yobou sene xaliss

  • @AbySene-kt2bu

    @AbySene-kt2bu

    20 күн бұрын

    Merci yaw mi wakh li nite daye doylou ame ay million ta doylou wau

  • @papenar2561

    @papenar2561

    20 күн бұрын

    @@AbySene-kt2bu ah dama kham ni 2005 ba legui mogui lale ay millons ba paré guis gnouy tabata nga dieul lignou yoor 😭

  • @cheikhfaty1417
    @cheikhfaty141720 күн бұрын

    Boy yangui dougal lac dè

  • @Franky-vy7vo
    @Franky-vy7vo18 күн бұрын

    il faut laisser la justice faire son travail

  • @user-iv3fk8ch7u
    @user-iv3fk8ch7u16 күн бұрын

    Nite dinga nék kharite tam mes ame na yo kham ni doko kham thi mome

  • @abdarahmaneba909
    @abdarahmaneba90919 күн бұрын

    Lac 2 sou beuguè kouko teugal combat na nangou beuré mais taxaw beneu place do bouger di melni robot baparé amoul supporter bissam dou nekh

  • @modousene2896
    @modousene289620 күн бұрын

    😢désolé mon frère lac ne peux pas cumuler des combats voilà son malheur ,car c'est un peureux dou beuré normal ,s'il avait cette chance il n'ira pas en.prison ,car il allait remettre l'argent , mais que dieu l'aide, yalna guén ,wakhléne deug moguéne

  • @diopmar6382
    @diopmar638220 күн бұрын

    Ces actes moy c'est un tranficant de visa

  • @MbayeMbengue-qt3sl
    @MbayeMbengue-qt3sl18 күн бұрын

    Ama balde am na bé boye boumou beug sacrifice ndiol djinee falaye la toudou contre Modou lo mingui Facebook

  • @souleydioptalibesonko3212
    @souleydioptalibesonko321220 күн бұрын

    Niou mélni yaw yénaw dougal nitte talala micro guay wakh rék ta liguay wakh kholoko wakh ba dougual nitte ki guay déf sa wakh dji dafa diakhaso loll ay erreur rék ngafi wakh baniala moytou micro yi rék

  • @elmalicksindidi5785
    @elmalicksindidi578520 күн бұрын

    Boy wax nga ba waax lou extrêmement grave nganii"lac waalou visa lolu domaine domainaam la" koon c'est pas la première foi yaaw sou enquêteurs yi deglo sa interview bi dinağ am piste bou lér

  • @boieyefa
    @boieyefa20 күн бұрын

    mais saway esk warowone nopi ...wakhi dof rek ngafi wakh ..soutoural sa mak ...shuttt

  • @papenar2561

    @papenar2561

    20 күн бұрын

    Ki dafeu ndeyou doof

  • @ndeyeamyfaye3468
    @ndeyeamyfaye346817 күн бұрын

    Yow khana khamo arrerou justice bou tolou fi warro wakh bala ngakoy gueuna dougal del wakh rek bakhna bamou neké thi lokho procureur do nopi

  • @beuzhustle3483
    @beuzhustle348320 күн бұрын

    Boy metriser woo Dara si liguayy waxx . Mbeur yiiii nioye kane.ils n'ont aucun rendement si deukeu biii

  • @cheikhdiakhate6474
    @cheikhdiakhate647420 күн бұрын

    Dioup dioubeul dioubeunti

  • @KarimSene-gh3qx
    @KarimSene-gh3qx18 күн бұрын

    😭😭🤦🤦

  • @user-bo3on9yj7q
    @user-bo3on9yj7q20 күн бұрын

    Mon frère j'aime bien Lac 2 mais ici c'est pas un sujet de lutte encore moins dans l'arène mais ici c'est sa vie après arène maintenant je pense que la police fera son travail si il est n'est pas coupable des faits il sera libéré vraiment

  • @user-dz7iz5xe1y
    @user-dz7iz5xe1y20 күн бұрын

    Waji yow genga dugal lac billahi danga wara nopi

  • @user-dc2mh6tc8v
    @user-dc2mh6tc8v20 күн бұрын

    Boy waxoo Dara.celébrité dou tax ngay Def Lou leundeum.il est Dan's le besoin Moy Lan.

  • @soukeynadaourdiaw7827
    @soukeynadaourdiaw782717 күн бұрын

    Mom dafa gueneu dougal lac

  • @AmethLo-wk7xi
    @AmethLo-wk7xi19 күн бұрын

    Yagu charger le dossier 📁 lac 2

  • @user-fj7wg6ex6m
    @user-fj7wg6ex6m19 күн бұрын

    Saway waxoo fi daraa

  • @bourathobouratho4672
    @bourathobouratho467220 күн бұрын

    Mé lac fane lay dougal khalisam bay am yéne problème yi

  • @falybadji8954
    @falybadji895419 күн бұрын

    boy yagui doull dai waxal lo xam lac xaritam mo moko nakh

  • @senegalais.
    @senegalais.19 күн бұрын

    Bien vu frerot mais la loi ne connais pas de célébrité tout le monde est pareil devant la loi. Qu’Allah l’assiste

  • @ismailasarr6467
    @ismailasarr646718 күн бұрын

    Na fay khalice bi rék walla

  • @ismailasarr6467
    @ismailasarr646718 күн бұрын

    Amo lo wakh na fay Jambuur yi

  • @MoustaphaDiop-is4tb
    @MoustaphaDiop-is4tb19 күн бұрын

    Ioe do féké woutti ndimbal th niane yalla mo diougé sifimou nék mo geun sa wakhi doff yi guay wakhe ay wakhou mo dane ki walla ki no😮

  • @mamecorsarr82
    @mamecorsarr8220 күн бұрын

    Rewmi dafa changé na

Келесі