Apres les rumeurs; Blessure de Balla Gaye2, Aziz Ndiaye et Tapha Gueye Fait des révélations explosif

Спорт

Пікірлер: 759

  • @ismailadiao1059
    @ismailadiao1059Ай бұрын

    Aziz Lamb ji beina roi la am

  • @khalil6250
    @khalil6250Ай бұрын

    Modou xaragne lo le roi des arènes ❤️💪🙏

  • @user-gi7ne4rm6o
    @user-gi7ne4rm6oАй бұрын

    Modoulo rekk ❤❤❤amol lenen

  • @akssports_world6945
    @akssports_world6945Ай бұрын

    Le seule roi C Modou kharagne lo , wakh lennn deuggg tei yalla takh liiiiii dou deuggg d'où Yoon dafay mel ni dagnouy kognass Modou looo,C désolant vraiment

  • @ibrahimasall8070
    @ibrahimasall8070Ай бұрын

    Aziz mo nekh Kone Sénégal champion du monde la Aziz gueneul si lingua nek thiakhane bakhoul Modou lo Moy bourou lamb j geumeul ndigalou yalla fi Modou lafi yalla tek mais nak boleneu beugué dieul leneu couronne en or diokh ko vainqueur bi mais Modou Moy roi

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141Ай бұрын

    Modou Lo moy roi 👑 boulnou fonto Azzi 🤷🏽‍♂️❌

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Aziz dafa ignané Modou Roi Beugu nio forcé FAWZAYNI mais Roi bou civilisé bi, gentle téksi yaram bou fraîche parcelle lay yéwo ❤lolou la yalla dogal🎉🎉

  • @ndongombaaye-dt1sl
    @ndongombaaye-dt1slАй бұрын

    Le seul roi c est Modou lo

  • @dembandiaye585

    @dembandiaye585

    Ай бұрын

    Non non c'est pas vrai

  • @Teranga9999

    @Teranga9999

    Ай бұрын

    On ta battu deux fois 🤣🤣

  • @kheuchaainformations5085

    @kheuchaainformations5085

    Ай бұрын

    ​@@Teranga9999modou lo dane gnila dane niepp😅

  • @Teranga9999

    @Teranga9999

    Ай бұрын

    @@kheuchaainformations5085 sauf tapha tine 🤣🤣🤣🤣

  • @bayemo4147

    @bayemo4147

    Ай бұрын

    Aziz balla lay Cartal d nioune sip nagn leep!!!! Balla gueye diamono djii thi yoone da warone may boy yi chance prsk dafa tegalei ay defaite: bombardier, boy niang …. Mais acteur lamb ji nio am nougn mel rek

  • @tidiane1878
    @tidiane1878Ай бұрын

    Lamb ji beneu king la am touss nak🎉

  • @mouhameddieng8564
    @mouhameddieng8564Ай бұрын

    Aziz daye délire rek 😂😂😂 dingou force mbeureme mi boule yakhe lamb dji lamb béne roi la ame thé parcelle laye yewo thieye modou mo modeste yi gayi di raye séne bopou la yore the yegeu louko sakhe bopam ndaye sane

  • @FS-jh4ky

    @FS-jh4ky

    Ай бұрын

    Modlo mo daw tapha tine yakk lamb ji

  • @baldendeye1884
    @baldendeye1884Ай бұрын

    Machallah Balla Gaye va battre Tapha Tine inchallah ❤

  • @jobehamidou6545

    @jobehamidou6545

    Ай бұрын

    Ameen

  • @abubaderyay2284

    @abubaderyay2284

    Ай бұрын

    No

  • @abdoulayediop6691
    @abdoulayediop6691Ай бұрын

    Balla Gaye2 yalla nako yalla may Ndam amine yarabi ♥️✊🏿

  • @mouhamethniang3154
    @mouhamethniang3154Ай бұрын

    Yalna tapha tine dane balla gaye thi barki serigne babakar sy amine ya rabi

  • @adamaseck8816

    @adamaseck8816

    Ай бұрын

    Yalna balla gaye dane tafa tine insha allah 🤲🤲🙏🙏

  • @adamaaw3486

    @adamaaw3486

    Ай бұрын

    Allahouma amine 🤲

  • @ibrahimaba2655
    @ibrahimaba2655Ай бұрын

    Couronne des empereurs aziiz ya nexx fii modou kharagne lo mofiii nekkk Bouleine gnou sonal

  • @IslandCure-hr4iy

    @IslandCure-hr4iy

    Ай бұрын

    😅😅😅😅modou lo MOY segneur des arenes kokou rombana EMPLEUR de L arenes. Thiey doudou lo niom nieup leuy Daan tapha tine prepare toi

  • @AminataDIOUF-ez8kd

    @AminataDIOUF-ez8kd

    Ай бұрын

    ​@@IslandCure-hr4iydou meusa dane balla si adouna 😂

  • @MaimunaMai-tf7xn

    @MaimunaMai-tf7xn

    Ай бұрын

    Sokhla Woul Balla Sakh Ndakh Gni Balla Manoul Dane La Kharagne Lo Dane😂

  • @fifty6292

    @fifty6292

    Ай бұрын

    Modou Lo mo déme dieul Siteu apart Papa Sow bou diekhal Siteu gneup ko dane bagn Tapha bagn Reug Reug combat royal comedie

  • @user-nd1xq1sg5j

    @user-nd1xq1sg5j

    Ай бұрын

    Kou ignannei modou lo sama mbeur mi sa leufeuil ndey

  • @moussaba638
    @moussaba638Ай бұрын

    Li yeupe pour khekh 😂😂😂modou lo 👍

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Billay fay dafa méti nak😂

  • @D_Dieylany
    @D_DieylanyАй бұрын

    Ah machallah vous êtes intelligents les ndiayes. Créer une nouvelle couronne pour votre arènes est une bonne idée parcq vrai couronne bi mom daniouy bayi walei ak mom soudé lolou moy dàgg sen xol yi nguéne dieul gaz tokk cii.

  • @alassanedieng259

    @alassanedieng259

    Ай бұрын

    Ah yéne kay wayadingéne dangéne du xaare lyléppo soxore moléneko yobbé bi moy vré roi bi pasq mo euppo ay avantage merci aziz bayile gayi fofo nioy sisou

  • @DameNguirane

    @DameNguirane

    Ай бұрын

    ​@@alassanedieng259yéne kay yéna sissou ba créer séne mbirou bopu

  • @cheikhahmettidjanidieng7462
    @cheikhahmettidjanidieng7462Ай бұрын

    Ndeysann empereur nioune PA rek lagnou topp

  • @danilombaye95
    @danilombaye95Ай бұрын

    Yéne mome sabotage rék wayé Modou Xaragne Lo moy le 🤴 👑 roi confirmé ✅ koum nékh ak koum nakhariii Modou Xaragne Lo moooy the king 👑 👑 👑

  • @elbiranetoure262

    @elbiranetoure262

    Ай бұрын

    Ay Domram monu thi modou sene lafal ndaye 😮

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Danio sokhor di khékh Modou mais kone roi Roi lay done ak ex roi 😂 dou tolo mom😂

  • @SuperMekni
    @SuperMekniАй бұрын

    aziz arretel mounane empereue des arenes roi bi modou la na ler bien k c bien reflechi respect

  • @user-zj7oi8bq9k
    @user-zj7oi8bq9kАй бұрын

    Modou lo moy roi des arénes amoul lénén

  • @saliouniang9713

    @saliouniang9713

    Ай бұрын

    Un vrai roi dou maytou kén

  • @papebabacarthiombane6961
    @papebabacarthiombane6961Ай бұрын

    Aziz tu es un exemple. Tu ne doit pas saboter la lutte. On te respecte donc respecte nous et accepte ce.que dieu a fait de modou lo le seul et unique roi des arènes à l heure actuelle

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Il est méchant vraiment 😢

  • @merinandiayelabokou4864
    @merinandiayelabokou4864Ай бұрын

    Modou lo kasé❤

  • @aladjisow1747
    @aladjisow1747Ай бұрын

    Lingéniye def ni yeup khame na gnou ko Li séne rival tecklé réussir ko moléne metti mouye modou lô lingéne teck yeup khame na gnou ko tapha tine saye mbockou bougou diougoul si combat bi dinga âme loula metti wallahi khamo si linga dougou sax balla ngéne beugu andiwate motakh ngéne teck systèmes bi mais lambe bi béne roi mofi âme mouye modou kharagne lô bagne bagne beugue ta sou doyalé si roi. Bi ndiago or béngifi

  • @alassanedieng259

    @alassanedieng259

    Ай бұрын

    Modou mo tong bopam pour. Qoi jeuloute tapha tine lolomodoune combam bi jaado .mai modou suteu bane sans la amole

  • @SuperMekni

    @SuperMekni

    Ай бұрын

    COPAIN LOU LERR GUA WAKH TAPHA NA DOF DOFLOU BA DOU SENE AFER YI LIKO DALONE MOKOY DALAT AY OPEN PRESS REGIONALE LEP TEK KHEL LA POUR DEFARAL LA AFER BOUDE AMGUAFI MBOK NALA KO LERAL NAK

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    ​@@SuperMeknibillay ligniy ték ay plan la pour Tapha Tine nako ay mbokam prévenir. Fay bi moléne méti🤧

  • @papebabavarseck5043
    @papebabavarseck5043Ай бұрын

    Aziz tu ne peux pas changer les regles du jeu tu essais a tout prix ressusciter balla gaye abec ces 100 defaites je supporte eumeu mais modou lo est le roi absolu tu nous parles d empereur tout en votre faveur pour dire balla est le meilleur albourakh est le meilleur respectes nous un peu

  • @ndakarudialdiop1206

    @ndakarudialdiop1206

    Ай бұрын

    Ya ngi khass balla gaye ci défaite té yaw mbeur bi nga supporter mo ngi ci 10 défaites mdr 😂😂

  • @FS-jh4ky

    @FS-jh4ky

    Ай бұрын

    Eumeu ngui si 200 defaites kone 😂

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Aziz buzz bi Modou am lako ignané motakh moukoy khékh Beugu nio forcé FAWZAYNI mais Roi bou civilisé bi, gentle téksi yaram bou fraîche parcelle lay yéwo ❤lolou la yalla dogall ❤🎉 Ex roi na dém took nékatoul si ay goudém😂

  • @user-ne9gm4bs5e
    @user-ne9gm4bs5eАй бұрын

    Aziz nandité 200% = Contenaire ngaka, wessu nañu diamono empereur Modou le roc des PA ❤ seul

  • @BALIGA_URBAINE_MUSIC

    @BALIGA_URBAINE_MUSIC

    Ай бұрын

    Iow la geumh kharagne lagn sokhoré couronne bii Modou lo a vie❤❤❤

  • @gabrielfaye952

    @gabrielfaye952

    Ай бұрын

    Moustapha ne devait pas entrer dans cette complicité. Mais yobanté galgaleu . Promoteurs gno koy réglé. Balla n'ira plus loin😂😂😂

  • @bayedamecisse5312

    @bayedamecisse5312

    Ай бұрын

    ​@@gabrielfaye952Inchalahou rabbi Bala Gaye 2 yalna dieum thia kanam baa faww

  • @FS-jh4ky

    @FS-jh4ky

    Ай бұрын

    @@gabrielfaye952yow yay yallah khana 😂

  • @alassanedieng259

    @alassanedieng259

    Ай бұрын

    Sa way ly bakhe nathi modou combambi amole béne sans tapha tine la warone dieule mi dafa mélné dfaxawa soxore té yalla dafa tabé

  • @mouhamethniang3154
    @mouhamethniang3154Ай бұрын

    Le roi c modou lo

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wcАй бұрын

    Modou Lo siteu kasse ❤❤❤

  • @seynaboutalland
    @seynaboutallandАй бұрын

    Aziz fi beine couronne mofi amm. Li daffey andi problématique

  • @user-we8jh4gu3c
    @user-we8jh4gu3cАй бұрын

    Www impec 👌🏾 🎉 balla gueye la faral d ms tapha tine comme nekoul roi des arènes kone merite na beurei combat d’empreure vrmt

  • @bilalkhalyfall9938

    @bilalkhalyfall9938

    Ай бұрын

    😂😂😂😂sheutete yén ay cinéma nguén

  • @RAMB75
    @RAMB75Ай бұрын

    Moustapha Gueye je vous estime beaucoup mais tu ne dois pas être là à cautionner une histoire de empereur des arenes ou couronne parce que vous êtes un grand champion. Aziz yaw mome sama grand ngeu mais... grand bayil yoyou waye 😂

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Deugu bi moy dafay saboté،té sokhor rék🤧

  • @user-pd4oz3ht6r
    @user-pd4oz3ht6rАй бұрын

    Kou dane roi yaye roi balla ex roi la 😂azize boul bayil sa khel bingay fowé lii mome mbaniel laye beugueu nourou 🥹

  • @alhamdoulilah9154

    @alhamdoulilah9154

    Ай бұрын

    Sûrement Aziz Ndiaye dafa Heine Modou lo parce-que teugokou

  • @papeflokiFall

    @papeflokiFall

    Ай бұрын

    Franchement

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Aziz dafa ignané Modou Roi Beugu nio forcé FAWZAYNI mais Roi bou civilisé bi, gentle téksi yaram bou fraîche parcelle lay yéwo ❤lolou la yalla dogal❤🎉🎉

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893Ай бұрын

    Aziz Ndiaye khoup bou katt ndaye la yorr modou lo moy rio moye sane baye

  • @bayemo4147
    @bayemo4147Ай бұрын

    Tapha tine yallah nako yallah may ndam bou amoul benn weranté!!! Lobbies yii ma guiss thi lamb dji niaaaw na

  • @Mohaaa2.0
    @Mohaaa2.0Ай бұрын

    Faut meme pas accorder de l'importance à ce qu'il dit uoe néko loudoul prommoteur di ibi sa lamign nane empereur fiiii da nga fi guiss empire yaa yague Moustapha uoe mome fou gnuouy wakhé todj todj uoe la gniy kheuthie sûrement da gni lay bokal on oublie pas yaa fi wakhone Boy niang eumeu ama da gniy wara beuré sén biir😭😭

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Dagniy khékh XLO mais touss xll mofi nék sén Fawzeyni bobou menatoul na dém retraite 😂

  • @ibzndim4585
    @ibzndim4585Ай бұрын

    Bilahi danio sokhoré roi bii Modou lo gnii ayy nafékk laniou Modou seul 🎉

  • @YasminNdom

    @YasminNdom

    Ай бұрын

    Ngi di na fekh beug nio modou lo

  • @taphagueye8675
    @taphagueye8675Ай бұрын

    Modou lo se le roi

  • @KhalilFaye-ok2gk
    @KhalilFaye-ok2gkАй бұрын

    Modou lo le 🦁

  • @laminjagne7254
    @laminjagne7254Ай бұрын

    Balla Gaye boy nyang moko mujee dan dengen fok nen balla moi dan sen couronne amoul chance

  • @mountaga2287
    @mountaga2287Ай бұрын

    Suis pas fan de modou lo , mais vraiment il a du merite daffa ligueye bakh yeksi fi malgres sa taille... geume bopam ak entrainement... te gayi nioko eupeu mais gorlgoruna ba degg rois des arenes bou paré tekk ci niari xalé ama ak boy niang nieup fogone dina perte roi bi mais daffa geume loumouy deff respect a lui.. fi mome kou nangoul y'Allah loumou deff dagay sonne rek...naniou bayi affaire de soxor ak racunié te nagou y'Allah loumou deff,...manga , yekini , tyson , bombardier , balla gye , eumeu sene nieupeu nagouwoné seen titre rois des arenes.. tayy y'Allah modou loko diokh. Salam

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Deugu rék nga wakh❤❤

  • @user-mg2nt7df3n
    @user-mg2nt7df3nАй бұрын

    Machaalla Abdou Aziz Ndiaye ❤❤❤❤❤

  • @aminatadiaw6941
    @aminatadiaw6941Ай бұрын

    aziz ndiaye yalna nga goudou fane si barcky seydina mouhamed❤️❤️🥰🥰🥰❤️ rewander bisii lamb djii aziz rk mosi meune dara

  • @AsseKebe-nq2fm

    @AsseKebe-nq2fm

    Ай бұрын

    Yamana doullllllll

  • @khalilgueye363

    @khalilgueye363

    Ай бұрын

    Iow reglèle

  • @badaradiop2262
    @badaradiop2262Ай бұрын

    Sokhor bakhoul tous sa pour dénigrer modou lo la mais malheureusement il est le champion aux cœurs des sénégalais

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Aziz est méchant il veut saboter Modou qui est le vrai Roi des arenes ,l'autre c lEx roi🤧

  • @alvinedieye
    @alvinedieyeАй бұрын

    Aziz, Ndiaye, n’essaye jamais de sous-estimer Modou, lo et sa couronne il est le roi des arènes. Il restera roi des arènes. Qu’importe le trophée que vous allez présenter entre Tapha tine et Balla Gaye Modou. il est le meilleur maintenant donc respectez-la

  • @alvinedieye

    @alvinedieye

    Ай бұрын

    Mauritanie 🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷

  • @alhamdoulilah9154

    @alhamdoulilah9154

    Ай бұрын

    Aziz dafa sokhor mais bilahi bou duggé si Modou lo dingako regrette

  • @ousououssououssou

    @ousououssououssou

    Ай бұрын

    Mogui begeu wayadi sakh nane ampleur khana Boy Niang ampleur kone déjà dana na Balla

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Aziz dafay sissou Modou c le seigneur de l'arène empereur dafa khéwi❤😂🎉Modou Seul ❤😊

  • @baralo9611

    @baralo9611

    Ай бұрын

    Rek

  • @mouhamethniang3154
    @mouhamethniang3154Ай бұрын

    Azize dafa sokhor bilahi yaw loula modou lo df doull

  • @alhamdoulilah9154

    @alhamdoulilah9154

    Ай бұрын

    Pour moum bayam mou moum rewmi 😂😂 n'a katt ndayam feulé Modou lo mou fi nek

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Sokhor rék moko diap

  • @user-pf5un1dj5h
    @user-pf5un1dj5hАй бұрын

    Azize Ndiaye Do yalla amo Dole yalla la eupou dole❤

  • @mounidior
    @mounidiorАй бұрын

    Aziz yaangui beu ga sooff nak.

  • @thiekpikine
    @thiekpikineАй бұрын

    Gnari roi gnofi ame mouye ama baldé ak boy niang ❤️💚😎⚔️👑🤴

  • @mordiop7649
    @mordiop7649Ай бұрын

    Machalla aziz pour la création et l'innovation..Mansour depuis la France.. Modou Lo da beug lou yomb dieul titre roi nane douma diokhé revanche di dieul ay siteu 😂

  • @layekharagne2224

    @layekharagne2224

    Ай бұрын

    def ak titre bi lou kene deffoul dane ci niari boy you guene euss sene generation, wa Fawzeyni yi sene khol dina guene tang 😂couronne bi inchallah modou retraite lakoy yobbou

  • @mordiop7649

    @mordiop7649

    Ай бұрын

    @@layekharagne2224 🤣🤣🤣 vrai roubé kate nga

  • @layekharagne2224

    @layekharagne2224

    Ай бұрын

    @@mordiop7649 dama khamnè daguene sone 😂modou limou def ak roi bi ni lalene metté ndeysane 😂

  • @alhassanetoure3088

    @alhassanetoure3088

    Ай бұрын

    @@layekharagne2224sawaay modou dey saboter ,lingay wakh ni amoul sens bou balla gaye dieulone couronne 2012 di beurei ak ay boy kone ba heure bi mingui ak couronee bi modou tapha tine la warone dieul mais nieimei wouko kholou keine dagou fi lecturou lamb rek laniou fi wakh

  • @layekharagne2224

    @layekharagne2224

    Ай бұрын

    @@alhassanetoure3088 pourtant bene boy you ci modou dane mouy boy niang guiss naniou foumou diar ak yow dh 😂 so deffone ni modou ak couronne bi do ci am bene victoire nakh mouno dane bene khalé

  • @ahmedgouduaby1813
    @ahmedgouduaby1813Ай бұрын

    Yalla tapha tine dokhane ndaye mou tokkk 😂😂

  • @SouleymaneMbodji-pn2uf
    @SouleymaneMbodji-pn2ufАй бұрын

    Modou lo moye roi monde de la lutte Sénégalaise

  • @loyouga3876
    @loyouga3876Ай бұрын

    Ngni danio beugeu yakh ndayi lamb dji modou lo c’ets le meilleur 👑❤️❤️

  • @babacardiop665

    @babacardiop665

    Ай бұрын

    No dagnouy saboté rek

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Bayiléne niou défar pour nakh séne bopou😂 ,boudé bou diamant sakh Roi bi mom Khalé bou civilisé biy yéwo PA moko mom❤🎉XLO KASSÉ 🎉❤

  • @durkio5486
    @durkio5486Ай бұрын

    Couroune modou bi molene téré nelaw

  • @assmalickniang8137
    @assmalickniang8137Ай бұрын

    Khana Issa pouye aussi roi la yeen yenay siisou mane deug 😂

  • @diamilmboup4392
    @diamilmboup4392Ай бұрын

    Kon Boy Niang Actuellement roi la 😂😂😂😂

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Sabotage rék😂

  • @tallacisse7797
    @tallacisse7797Ай бұрын

    Aziz Ndiaye thiaxane baxoul waye. Beine roi ak empereur mofi âme et c'est Modou Lo. Bouleine gnou forcer Balla Gaye mi meuneutoul

  • @Domou_Deukk_Bi

    @Domou_Deukk_Bi

    Ай бұрын

    Yén nieupeu wara ngagnie balla bamou dess yén modou diabarou balla la

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Balla da dém faylande lolo ko méti 😂dafa dane Modou Modou rawko kholbi di dagu nak😂mou cré empereur😂kone dé Boy niang empereur la😂

  • @Domou_Deukk_Bi

    @Domou_Deukk_Bi

    Ай бұрын

    @@rouguikebe9984 Modou noumko rawe si lamb? 😂😂 Modou loumou def si lamb téh balla défouko? Yaw soulager sa conscience nga neik didéf nii modou fimné nii gniko meuneu nokou bamou doulle nieup dafleine di daw😂😂 si tégui bou méti la neik😂 Balla ak lougnko meuneu waxall meusoull tégui mbeurr

  • @mamadouthiam4683
    @mamadouthiam4683Ай бұрын

    ISSA POUY ROI DES ARÈNES MO DANE BALLA GAYE 2 😂😂

  • @papahabibdiopofficielle3160

    @papahabibdiopofficielle3160

    Ай бұрын

    Bobou balla nekagoul roi t balla dieulna revanche sam 2006🙏 nopil

  • @user-nd1xq1sg5j

    @user-nd1xq1sg5j

    Ай бұрын

    Boye ndiang nakk bomb nak

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Wakhal Boy Niang kone😂😂

  • @papiharis9038
    @papiharis9038Ай бұрын

    Vraiment wa Albourakh sont en train de plus en plus révolutionner la lutte sénégalaise Masha Allah

  • @aboudiack7546
    @aboudiack7546Ай бұрын

    Yene niouy sagua Aziz ndiaye fi mome day may mbeuram valeur tè amnasi droit. Mais je vous comprend balla da nokk sen mbeur defko lougn doul meusseuti def mbeur (dioutal ) 😂

  • @adamaseck8816

    @adamaseck8816

    Ай бұрын

    Lolou moy dakar ndey senn khol yii wa diouteul yii loutakh niou bone

  • @adamaaw3486

    @adamaaw3486

    Ай бұрын

    @@adamaseck8816😂😂😂

  • @malickfall3604
    @malickfall3604Ай бұрын

    Modou lo rois des arènes 👑😂😜

  • @saidigassama1397
    @saidigassama1397Ай бұрын

    Fi dh xalis moy wakh😅😅😅

  • @mouhamethniang3154
    @mouhamethniang3154Ай бұрын

    Yene da nguena sokhor modou lo moye roi koumou nekhoul nga mate sa bakane azize bayil sokhor ok momo nite yi modou lo ak wa parsel falai wuniou la

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Dafa ignane waay yeufou sabotage yi nk

  • @abdoudiagne642
    @abdoudiagne642Ай бұрын

    wayy Aziz yaw yaye domérame mbéne roi mofi âme mouye Modou lo

  • @gayeablaye7097
    @gayeablaye7097Ай бұрын

    Modou lo kay mo dieul yonou sabotè lamb dji mo warona dieul tapha tine moy yonou lamb mè dieul siteu Ko khamni danoul bene mbeur apar papa sow danoul bene champion

  • @ndatteyalla9917

    @ndatteyalla9917

    Ай бұрын

    VRAIMENT

  • @FS-jh4ky

    @FS-jh4ky

    Ай бұрын

    Merci li yeup modou moko indi mo warone dieul tapha mou daw

  • @mouhamethniang3154

    @mouhamethniang3154

    Ай бұрын

    Yaw katal sa ndeye feulee

  • @gayeablaye7097

    @gayeablaye7097

    Ай бұрын

    @@mouhamethniang3154 amal yar saga bakhoul rafètoul demal diegueulou sa yaye meritèwoul lii

  • @user-fy2fj8bl1j

    @user-fy2fj8bl1j

    Ай бұрын

    Tapha tine mo wakamti rek so dieul yone balla modou lay bereul kon siteu vs balla moy takhaw

  • @taphisgates
    @taphisgatesАй бұрын

    Aziz yangui deliré nii😂😂😂😂 J’attends la suite 😅

  • @user-ts9mr7vv4y
    @user-ts9mr7vv4yАй бұрын

    Modou lo roi des arènes Le meilleur pour toujours Tt les jaloux vont ndmmmm maigrir ❤🎉🎉 Modou lo késsé

  • @mamemoussagueye952
    @mamemoussagueye952Ай бұрын

    Boulène yakheu Lamb dji mane douma supporter Modou Lô mais nagneko respectel couronnam bi dafko mérité…CNG bi lagne wara tass réorganiser ko defar couronne defko tournois bou mak kouko dieul nékk roi des arènes

  • @maguettecamara
    @maguettecamaraАй бұрын

    Aziz balla la beugeu mayate valeur mais fi mome ben roi mofi am moy kharagne lo moi nak je suis eumeu sene

  • @Domou_Deukk_Bi

    @Domou_Deukk_Bi

    Ай бұрын

    Balla meussoull niak valeur mossouniouko teug téh stade bi féssoull modou si bopam mo rew meuno yor courone bi beug eviter nieup ragall reik la déf

  • @mamadoufaye3123
    @mamadoufaye3123Ай бұрын

    c'est ce même promoteur qui va maraboute tapha tine

  • @BayecheikhouTounkara

    @BayecheikhouTounkara

    Ай бұрын

    Dafa lérr

  • @bayemo4147

    @bayemo4147

    Ай бұрын

    Moom la d dafa leer

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Lérna mom khamga ni empereur bobou yeup Balla lakoy yéné waay🤧yeureum na Tapha sakh😢

  • @moustaphadia8777
    @moustaphadia8777Ай бұрын

    Modou Lo moye roi force

  • @user-sh9sc3fv6p
    @user-sh9sc3fv6pАй бұрын

    Francement aziz ake baye ndiaye yénafi nek ❤❤❤

  • @user-rp1ln5lz8y
    @user-rp1ln5lz8yАй бұрын

    Merci beucou azize Ndiaye

  • @taphacisse-fi3bn
    @taphacisse-fi3bnАй бұрын

    Merci aziz❤❤❤

  • @babacarsarr2420
    @babacarsarr2420Ай бұрын

    Vraiment ay domeram Gein

  • @mamadoualioubah9831
    @mamadoualioubah9831Ай бұрын

    Balla yalnako yalla may ndam

  • @matarlo8583
    @matarlo8583Ай бұрын

    😂😂 aziz bulniou fonton wayy niari roi meunoul ame 😂

  • @aladjifalloudia4915
    @aladjifalloudia4915Ай бұрын

    Machalah aziz ndiaye balla gaye rék lanie topou bilaye yalla nala Yalla maye ndam amine ❤❤❤😂🙏🙏🙏🙏

  • @infosprotv9626
    @infosprotv9626Ай бұрын

    Wakho fi dara Bege Défe Balla gaye roi nono Mais Lambe Dafa am niou ko yoré

  • @alhamdoulilah9154
    @alhamdoulilah9154Ай бұрын

    Respecter wou al amine bokou respecter wone dou togati di wakh si lamb

  • @morysarr-ry4mk
    @morysarr-ry4mkАй бұрын

    Balla gaye tégélé fi 2 défét bén Rio mofi ame Modou lo

  • @boubacarwelle4314
    @boubacarwelle4314Ай бұрын

    Sa waye Azize loumouye wakhnii dou yone empereur mou nous fait am tes rois des arènes nékk fii cng mo wara officialisé afair de roi des arènes une bone fois pour tout bafii balla gaye néké roi des arènes kéne djiemoufii créyé ayy empereur boulène saboté lambdji moye sougniou spor nationale

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Wakhal dé sokhor rék moko diap mais Bayiléne niou défar pour nakh séne bopou ,boudé bou diamant sakh Roi bi mom Khalé bou civilisé biy yéwo PA moko mom❤🎉XLO KASSÉ 🎉❤

  • @user-sd5qv1eb2t
    @user-sd5qv1eb2tАй бұрын

    Moudou lo khalif général lambdji yalla moko deff

  • @modouseck3380
    @modouseck3380Ай бұрын

    Wow Kone takhaw pour khel modou lo

  • @senegal559
    @senegal559Ай бұрын

    Wakhi dof

  • @MameBalla-mf8dt
    @MameBalla-mf8dtАй бұрын

    Aziz Ndiaye deum leu

  • @presse221
    @presse221Ай бұрын

    Niéne daguéne sokhor Modou lô moy sen bayii c lui le roi des arènes khalisse motax doleine wakh ** Aziz Ndiaye deugeu limouy wakh nii kou sokhor mokay wakh tapha tine dina niaff senn *** ba kirikoro fadam ioe seytané gua

  • @user-uj7ze9dm7i
    @user-uj7ze9dm7iАй бұрын

    Balla la faralon dé mé yalla nako tafa dorr mo dano

  • @layefall452

    @layefall452

    Ай бұрын

    Louy lolou??

  • @AminataDIOUF-ez8kd

    @AminataDIOUF-ez8kd

    Ай бұрын

    Ioe la rec😂

  • @user-uj7ze9dm7i

    @user-uj7ze9dm7i

    Ай бұрын

    @@AminataDIOUF-ez8kd 😂😂ki dafa sof waye moy Mélni koy wakh lo am fola

  • @user-yf8bm4fr9u

    @user-yf8bm4fr9u

    Ай бұрын

    Loutakh nga wakh ko loula méti

  • @modoufaye2255

    @modoufaye2255

    Ай бұрын

    Ndakh lane

  • @user-hj6cu5uc2s
    @user-hj6cu5uc2sАй бұрын

    ❤❤❤❤il communique bien

  • @dembandiaye585
    @dembandiaye585Ай бұрын

    Merci aziz tu as bien dis ❤

  • @modouseck-yz5tg
    @modouseck-yz5tgАй бұрын

    Mafi djitou 🎉❤

  • @khalilgueye363
    @khalilgueye363Ай бұрын

    Saway lamb ji momoulene ko modou seul P.A moy dirigé force

  • @oumitandiaye6780
    @oumitandiaye6780Ай бұрын

    Aziz Ndiaye fait tout ca pour balla gaye 2 pour lui c balla qui va gagner

  • @sandjiryba5555
    @sandjiryba5555Ай бұрын

    Aziz ya nekh courone Modou Lo bi gua beug saboter wayé Yalla bakh neu

  • @BathieDiop-yx8ul

    @BathieDiop-yx8ul

    Ай бұрын

    Sa way mod lo mo yakh lamb dji moko saboter siteu kan la d'âne bay am combat royal

  • @abdoutoure2490

    @abdoutoure2490

    Ай бұрын

    Fi dal. Modou. Moy. Roi. Fi. CNG. Mo yor. Réglement. Mi. Pas. Prometeur. Kou dèfar sa. Kou ron. Ya. Kham

  • @ibrahimadrame9499

    @ibrahimadrame9499

    Ай бұрын

    Dako meune ak loumou meunti pékhé kharagne lo moye roi des koullou mbeur💪💪💪💪

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Aziz dafa ignané Modou Roi Beugu nio forcé FAWZAYNI mais Roi bou civilisé bi, gentle téksi yaram bou fraîche parcelle lay yéwo ❤lolou la yalla dogal❤🎉

  • @ibrahimadrame9499

    @ibrahimadrame9499

    Ай бұрын

    @@rouguikebe9984 Aziz wakhou dof lay wakh😀😆😆😅

  • @ndoffenetine5333
    @ndoffenetine5333Ай бұрын

    Modouuuuuuuuuu looooooooooooo ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤

  • @fallelhadjiabdoulaye2347
    @fallelhadjiabdoulaye2347Ай бұрын

    Machalla aziz amal diam❤❤❤

  • @papefall4806
    @papefall4806Ай бұрын

    Boulen saboté way balla moy sama mbeur Mai’s boulen fi créer yenen truc pour saboter la couronne de modlo

  • @maissamboup4169

    @maissamboup4169

    Ай бұрын

    Ta compris li xex Modou lo la

  • @papefall4806

    @papefall4806

    Ай бұрын

    @@maissamboup4169 Lolou deh nangou woumako vraiment man mome si deug rek lay dokh balla moy sama mbeur Mai’s boulen saboté li yalla defal mod lo

  • @FS-jh4ky

    @FS-jh4ky

    Ай бұрын

    Legui koula wakh ni balla moy dane 😂

  • @Bour_ndiaye_bour

    @Bour_ndiaye_bour

    Ай бұрын

    Naneléne glace waye

  • @aliounejohnson6725

    @aliounejohnson6725

    Ай бұрын

    N'importe quoi

  • @abdoulayembengue1949
    @abdoulayembengue1949Ай бұрын

    Aziz domeram Ngeu combat royal bi moy meti sa khol mais force modou moy roi bi Ngay Doul fi pff Xaliss gerel woul li d Modou ngay bagne degue Sa thies moy wone sene plan nious nagneko

  • @bayemo4147
    @bayemo4147Ай бұрын

    Thiey le lobbie: aziz mooy bank bi recruter agents( fadam wahkat bi et père tapha gueye “juste pour avoir plus de crédibilité”) … leep thi contrer modou lo et propulser balla gueye 2 😂😂. Nous avons compris le jeux d sama gars yi 🫡🫡🫡 😑 ❌❌❌❌❌

  • @rouguikebe9984

    @rouguikebe9984

    Ай бұрын

    Billay mais Modou lafi yalla ték bénéne roi bougn fi cré peureum la😮

  • @emobusinessmohamadezzedine2244
    @emobusinessmohamadezzedine2244Ай бұрын

    Ils ont toujours un problème avec la couronne de Modou lo Et font tous pour enterré Modou lo Mai’s nak wakhi dof la rek

  • @rigobertsambou3891
    @rigobertsambou3891Ай бұрын

    J'entends Tapha GUEYE dire que Balla fera son open presse à Bignona ou Ziguinchor mais il n'osera pas car ce n'est pas son territoire.je lui conseille plutôt de voir ailleurs vers Sedhiou.

  • @AminataDIOUF-ez8kd

    @AminataDIOUF-ez8kd

    Ай бұрын

    Vas là-bas es que casamance t'appartient ?

  • @mamadouba6357
    @mamadouba6357Ай бұрын

    😂😂😂 Aziz pour moom mo moom Lamb ji. Franchement gueumeul Yallah, il n'y a qu'un seul roi des arènes et c'est Modou LÔ. Khana empereur Al Bourakh, mais pas de l'arène. Ça n'engage que vous

  • @Malou476
    @Malou476Ай бұрын

    Partenaires balla la rek😂😂😂

Келесі