Ameth Diop est mort, Mamadou de retour sur les lieux, Ce qui s'est réellement passé a Technopole

Pikine: Ameth Diop est mort, Mamadou de retour sur les lieux, Ce qui s'est réellement passé a Technopole

Пікірлер: 230

  • @ModouBodian-jv4oj
    @ModouBodian-jv4oj3 күн бұрын

    Dakar beuzz yénagui déf liguéye bou raféte ❤❤❤❤❤

  • @awasaliouba8420
    @awasaliouba84203 күн бұрын

    Fadèl ngir yalla do gnou topal khalè yigne fékone si Auto Badou keur MBAYE fall

  • @BoussoBaaly-9494

    @BoussoBaaly-9494

    Күн бұрын

    Xalei yoyou bilahi batay damaléne di xalate😭

  • @user-hl9zm6ue4g

    @user-hl9zm6ue4g

    Күн бұрын

    Bilahi lolou daniou ko wara topou

  • @fatoudiakhate1516
    @fatoudiakhate15163 күн бұрын

    Yalla nako yalla yeureum khareko aldiana firdawsi si barke zeydina Mohamed amine ya raby

  • @AlimaNdiaye-uj1hz
    @AlimaNdiaye-uj1hz3 күн бұрын

    Trop d’injustice dans notre pays té li thi eup sunu police bi moniouko tek vous avez échoué dans tous les plans de la Sécurité Sénégalaise honte à vous 😢😢😢

  • @user-pr9kx1mz6v
    @user-pr9kx1mz6v4 күн бұрын

    Ameth yalla Nako yalla yeureum police yi liniou déf niawna

  • @saliou6884
    @saliou68843 күн бұрын

    Il faudrait qu’un psychologue assiste Modou. ce serait vraiment bien. Lim dounde dafa metti. Yalna Yalla doli soutoura . Ahmed yalnako sunu borom yeureum .

  • @moussafall1614
    @moussafall16143 күн бұрын

    Ces policiers qui ont commis ces actes barbares sont une véritable menace contre la société, ils doivent passer le reste de leur vie en prison, ils n'honorent pas la police.

  • @user-mg2nt7df3n
    @user-mg2nt7df3n3 күн бұрын

    Ndeyssane histoire bi akama meti té khawmalene billahi Ahmed yalnako yalla yerem té khareko djianatoul firdaws 🙏

  • @NdoumbeNdoye-rq8qs

    @NdoumbeNdoye-rq8qs

    2 күн бұрын

    Bilahi niosi yam kone damako kham

  • @wizyoutubeur8587
    @wizyoutubeur85873 күн бұрын

    un bon policier doit chercher des preuves sans usurper ni bafouer les droit d'un suspect

  • @ToutyMakhtarNdiaye-ho1tq
    @ToutyMakhtarNdiaye-ho1tqКүн бұрын

    Bilahi khaley yoyou damaléne yeureum yalla naléne yalla até AK Badou pouye

  • @madagueye9951
    @madagueye9951Күн бұрын

    Metina massa ahmeth yalla nako yalla yeureum

  • @TherereSarr
    @TherereSarr3 күн бұрын

    Il faut que justice soit faite comme Le président réclamé la justice équitable

  • @khalifaababacarNiang313

    @khalifaababacarNiang313

    3 күн бұрын

    Lépou dina ame ndanke ndanke rék inchallah

  • @user-yl5gh8xx6f
    @user-yl5gh8xx6f3 күн бұрын

    Police sénégalais yi ay deume laniou😢😢😢😢😢😢😢

  • @galaxiepro.5641

    @galaxiepro.5641

    3 күн бұрын

    Ay ak yawite

  • @momathniass5720

    @momathniass5720

    3 күн бұрын

    Bilahi

  • @mbayefall5684
    @mbayefall56843 күн бұрын

    Policiers yoyou deh niongui doundou lou tard bir prison yallana yokou amine

  • @futurepro4862

    @futurepro4862

    2 күн бұрын

    Daniou len diapp?

  • @abibdiop4678

    @abibdiop4678

    Күн бұрын

    ​@@futurepro4862bou yagg sakh

  • @moustaphagoumbala1804

    @moustaphagoumbala1804

    5 сағат бұрын

    Yakar nako d

  • @moustaphagoumbala1804

    @moustaphagoumbala1804

    5 сағат бұрын

    ​@@futurepro4862si diap nane len ngour diomay bi kou si deung niou diape la

  • @mormbaye3908
    @mormbaye39083 күн бұрын

    Vraiment Senegal warna wèssou torture .. c est honteux

  • @mouhamedndoye8414

    @mouhamedndoye8414

    3 күн бұрын

    Quelle honte

  • @ToutyMakhtarNdiaye-ho1tq
    @ToutyMakhtarNdiaye-ho1tqКүн бұрын

    Oh masta yalla nako yalla kharé aldiana firdawsi

  • @ledakartimes
    @ledakartimes3 күн бұрын

    Vidéo bi dinako partager partout

  • @fatouchbah2945
    @fatouchbah29453 күн бұрын

    Lii metina torop que l'âme de Ahmed repose en paix Amine!

  • @Ouleey__
    @Ouleey__3 күн бұрын

    Policiers bou meussa door wala rayeu diamou yAllah yi yAllah nala yAllah fayeu seuu dieuff

  • @ndeyefatoundiayendao7580

    @ndeyefatoundiayendao7580

    3 күн бұрын

    amine

  • @beuknieup4022
    @beuknieup40222 күн бұрын

    😭😭😭j'ai pas les mots RIP Hamet Taye

  • @lamineteuw6839
    @lamineteuw68393 күн бұрын

    Moi aussi wa police centrale brigade cisse c'était en 2019 , il mon fai La même chose gnou da dadié ake arrêtema m'a. Takhawe gnou guisse khalise si mane clomotifema néma dama yore. Droge, yaubouma terrain colobane daurema daure yo khameni au teudena 2semaine malade, daurema, pa paré nema diokhele wala ga dème kasso, bilakhi sama 500000 fcf lagnou léke, tes balouma léneko

  • @wizyoutubeur8587

    @wizyoutubeur8587

    3 күн бұрын

    demal dic denoncer len

  • @Xarnoubi

    @Xarnoubi

    3 күн бұрын

    Bayilen ak yala dagnouy liguey ba dè dougnou yor ndayi dra yalen di meussa tanè

  • @lamineteuw6839

    @lamineteuw6839

    3 күн бұрын

    @@Xarnoubi bilakhi mes police sénégal se sont des contompu da calité , dougnou ame darra ba rentrerai,

  • @fatouchbah2945

    @fatouchbah2945

    3 күн бұрын

    Lolou yagueu na fii Mane sama borom keur lagnouko deff

  • @Sunu400milles

    @Sunu400milles

    3 күн бұрын

    Portél plainte bolén bal ay agresseurs lagnou policiers yi

  • @Yes-eq7me
    @Yes-eq7me2 күн бұрын

    😭 Yallah dina len mbougeul si adouna bi ak alakhira

  • @ModouBodian-jv4oj
    @ModouBodian-jv4oj3 күн бұрын

    Ahmed yalla nako yalla défal ndiam wayé njiko réye li déss ci sen dou yalla na done safara ba bisbouniouye déh inchallah

  • @Galsn

    @Galsn

    3 күн бұрын

    Wa kouy Ahmed ?

  • @khalilou221

    @khalilou221

    3 күн бұрын

    @@GalsnAmeth bénde gars bou deuk pikine la Policié pikine yi nioko raye

  • @Galsn

    @Galsn

    3 күн бұрын

    @@khalilou221 ha je me rappelle ndeysane

  • @khalilou221

    @khalilou221

    3 күн бұрын

    C’est ça

  • @amadouwaguediame4413

    @amadouwaguediame4413

    3 күн бұрын

    😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊

  • @latechnologie4563
    @latechnologie4563Күн бұрын

    Dagay seetan ay mbirr sa kholl di bone do si meune dara 🤦🏾‍♂️

  • @Binetasow-qc8gl
    @Binetasow-qc8gl3 күн бұрын

    Yala na ko yala kharè aldiana amine barké seyedina moukhamete amine ak kep kou fatou😢

  • @AladjiXassana
    @AladjiXassana13 сағат бұрын

    Ahmed Taya YALLAH nako YALLAH yeureum xareko Aljana mayko geureumam

  • @sayeseck1089
    @sayeseck10892 күн бұрын

    Ndeysane amet yalla nako yalla yeureum Barke Nabil Moustafa tourondowam🙏🙏

  • @syllartdesignmetal9004
    @syllartdesignmetal90043 күн бұрын

    J'ai le cœur vraiment meurtrie 😢😢😢

  • @astoumbengue6071
    @astoumbengue60714 күн бұрын

    Yalla nala yalla défale diame❤❤❤❤❤❤

  • @Dangerous1404
    @Dangerous14043 күн бұрын

    Policier sénégal amna niou bakh dè wayè gnisi bone nio eupe tè français bou lère sakh meunouniouko,torokhal nite rèk laniou meune wallahi,sénégal amoul lois

  • @onlygood1114

    @onlygood1114

    3 күн бұрын

    Bilahi deugla

  • @galaxiepro.5641

    @galaxiepro.5641

    3 күн бұрын

    Français bou lér dou ndam wolof bou lér moko guene

  • @Dangerous1404

    @Dangerous1404

    3 күн бұрын

    @@galaxiepro.5641 yaw doul kou nèk nga beug ko tontou,ngaye dagasantè mèlni borom niari tour yi merde,khamna sa baye policier le motakh nga sonou ni,wayè li am meunouko bagne,certains policiers senegalais sont des vor1 et des corrompus,ay mbam kharam kassè

  • @SakhoSoumayya
    @SakhoSoumayya3 күн бұрын

    Sénégal yaxouna policiers yi wara proteger askane wi niolén Di xoxatal dilén déf Lou niaw Sénégal dafa beuri policier youye abusé AK askane wi beuri ayy police corrompue wayé gni raye ameth yalla na dérétou ameth done toké si niom ameth yalla nako yalla yeureum sy barké seyedina Mohamed psl Sénégal yaxouna mbone barina fi lolou sax wayé yalla baxna

  • @astoufall5758
    @astoufall57582 күн бұрын

    Mane dh waruna vraiment choquée

  • @LamineDiouf-xh7gl
    @LamineDiouf-xh7gl2 күн бұрын

    Yalna firdawsi done keuram si barké seydina mouhamed

  • @DemeAbdourahmane
    @DemeAbdourahmane3 күн бұрын

    Dakar buzz défa daw Sénégal buzz ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @matargueye7200
    @matargueye72003 күн бұрын

    Domarame yi motakh kousi retraite do amm sarape dayame domòu sarape dayame yi

  • @AichaNiass-vo5li

    @AichaNiass-vo5li

    3 күн бұрын

    Bilay wahatiko kousi retraité do ame dara

  • @paposakho17

    @paposakho17

    2 күн бұрын

    C'est un remarque 😮

  • @SakhoSoumayya
    @SakhoSoumayya3 күн бұрын

    Sénégal beurina ayy homme de tenu yo xamni sén palace moye derrière Les barreaux ay policiers corrompu soxor

  • @nogayeseye826

    @nogayeseye826

    2 күн бұрын

    Gnome Gnepa yam téki wougnou dara motax dinagne ligueye ba deh dougnou ama gatte

  • @diodiogaye5940
    @diodiogaye594022 сағат бұрын

    Allahou Akbar😭😭😭😭Aye way li lane la ni😭😭😭😭

  • @user-pi3gx2rq4x
    @user-pi3gx2rq4x3 күн бұрын

    Ameth yalnaka sounou borom yeureum te hareka aldiana sy barker seydina mouhamed

  • @NdawElzo
    @NdawElzo3 күн бұрын

    Atté bi yombena😊 policier yi déf li nagnouléne torturé à mort👈 parce que aye domou kharam lagnou 😢

  • @ndeyemarietouba9097
    @ndeyemarietouba9097Күн бұрын

    Yalna yalla até policé yi naniou balou ak sènègalèyi

  • @FatimandaoTymandao-gr4gl
    @FatimandaoTymandao-gr4gl3 күн бұрын

    Thiey yallah, yalna détenus fayoul lene sibir kasso bi. Yallah yeureum Ahmed bou bakh

  • @galsennostress8522
    @galsennostress85223 күн бұрын

    Amet Taya yala nako yala yeureum te kharé ko aldiana

  • @modouballadiop5685
    @modouballadiop56853 күн бұрын

    Data ndaye police sènegal

  • @fayatv2657
    @fayatv2657Күн бұрын

    Fallait pas boire de l'eau pour éviter les hémorragies interne que son âme repose en paix yalla nako yalla yereum té kharéko aldjiana firdawsi amine et que justice soit faite

  • @Layefall08
    @Layefall083 күн бұрын

    Nous remercions chaleureusement son excellence bassirou Diomaye faye et Abdoulayesylla nous sommes heureux de votre collaboration

  • @ramasagna4292
    @ramasagna42923 күн бұрын

    Que le Seigneur Tout Puissant accorde sa Miséricorde à se défunt et allége la souffrance de ses proches et son ami...i have à Dreams....Qu enfin en Afrique Tout entier , particulièrement à mon cher Sénégal, que la justice fasse son travail, les policiers punis de façon exemplaire et les victimes indemnisées....i Know...i have Just à Dreams...😢

  • @papaousmanecisse4886
    @papaousmanecisse48862 күн бұрын

    Ces genres de pratiques ne doivent pas rester impunies il faut les poursuivre fermement jusqu'à la dernière énergie

  • @myamandiang
    @myamandiangКүн бұрын

    Thiey yall founiou dieum😢😢

  • @diopelmalick456
    @diopelmalick4562 күн бұрын

    mouhamed diop yalna ko yalla kharé aldiana 🙏🏻

  • @AdjuntoOfrece-qr7db
    @AdjuntoOfrece-qr7db3 күн бұрын

    Diarama fadel mbir mi lou diara topouleu

  • @ouzermatresetepenre1025
    @ouzermatresetepenre10253 күн бұрын

    DB vous êtes des bosseurs machallah ❤

  • @BoubacarTall-xn1et
    @BoubacarTall-xn1et3 күн бұрын

    Merci Fadel affaire bi waroul sede na laire nagne.

  • @MbayeThiaw-pq9mt
    @MbayeThiaw-pq9mtКүн бұрын

    Sérieusement Sénégal meritowoul liiiii😢

  • @fatouwade5048
    @fatouwade50483 күн бұрын

    Ndeyssane yana la Yalla takhawou té Ameth yana ko Yalla yeureume té diégueul ko 🙏

  • @ModouBodian-jv4oj
    @ModouBodian-jv4oj3 күн бұрын

    C'est la triste réalité ❤❤❤❤❤

  • @dydjakeita7122
    @dydjakeita71223 күн бұрын

    Ana wa droit de l'homme

  • @ibrahimagueyeseck7423
    @ibrahimagueyeseck74233 күн бұрын

    Il y a bcp de fous en circulation dans la société sénégalaise, comment une personne peut faire preuve d'autant de cruauté.

  • @PapaLo-ku6uc
    @PapaLo-ku6uc3 күн бұрын

    Très bien ta bien fait le présentateur

  • @matargueye7200
    @matargueye72003 күн бұрын

    Boye defall plainte boulenn bayi na yonn deff ligueyam guenn lenn khekh

  • @dioufmodou4234
    @dioufmodou42343 күн бұрын

    Wajdi Dakar buess ligeye bi rafetna

  • @NAKK_YAYE16
    @NAKK_YAYE163 күн бұрын

    🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺 paix à son âme et belle travail que vous faites le Dakar Buzz

  • @Billicisse651
    @Billicisse6513 күн бұрын

    Gatsa gatsa rek nioune wa darou mome douniou meusseu bayi wa police pikine ay deum lane

  • @namaly829
    @namaly8293 күн бұрын

    Justice pour ces jeunes comment un pays normal devrait accepté ce genre de comportement de la part de certains soi-disant policiers

  • @user-mq2qw2pj6o
    @user-mq2qw2pj6o3 күн бұрын

    Yalla nako souniou borom yereum

  • @CheikhSene-eb5bj
    @CheikhSene-eb5bj3 күн бұрын

    ngén balma mais bén version rkkk ngén déf lou esk soupçonné wougn lén niew niom aussi niou yor arme diém khékhhh akk niom policier yi mér gagn lén??

  • @habycisse3609
    @habycisse36093 күн бұрын

    VRAIMENT LE NOUVEAU GOUVERNEMENT DOIT VRAIMENT SE METTRE À TRAVAILLER SUR LES CONDITIONS DES PRISONS AU SÉNÉGAL. CELÀ DOIT ÊTRE UNE PRIORITÉ.

  • @sapduesseldorf
    @sapduesseldorf3 күн бұрын

    Gno gnoy ay domeram 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @nogayeseye826

    @nogayeseye826

    2 күн бұрын

    Domeram sax molène gueune

  • @faloukane792
    @faloukane7923 күн бұрын

    Merci Dakar buzz

  • @PapaSane-db2jw
    @PapaSane-db2jw2 күн бұрын

    Metina bilahii ray nite té dou moudj féneuh

  • @nogayeseye826
    @nogayeseye8262 күн бұрын

    Police Sénégal dou néguène nih rek abusé si séne pouvoir dih raye nitte gni rek motalhe loumou lène diarigne ? Yoro léne ngatte teki wolène darra yène ngeneuh wala kana gnép Changeléne mo gueune bolène beuguè diarigno séne sueur

  • @FatoukaneThiellosene
    @FatoukaneThiellosene3 күн бұрын

    Gni ko deff sen adina yalah na done safara ci barké seydina mouhamed saws 😢😢😢😢

  • @theblackmamba434
    @theblackmamba4343 күн бұрын

    Machallah Dakar buzz

  • @MamefatouSeck-ku6yo
    @MamefatouSeck-ku6yo3 күн бұрын

    ay way li métina trop 😭😭😭😭😭

  • @cheikhomardrame5836
    @cheikhomardrame58363 күн бұрын

    Ce Ndéné tmt ah doyna warr dh Ameth taya yalnako yalla yeureum

  • @coulibalyyacine6231
    @coulibalyyacine62313 күн бұрын

    Akhmed Yalla nako Yalla yeureum

  • @mobarakff9797
    @mobarakff97972 күн бұрын

    Ahmed yalla na yalla yessal yeurmande bavure policiere da fè wara diekh tak

  • @WelimataDiol
    @WelimataDiol3 күн бұрын

    Nn😭😭 yalla nako yalla yeureum

  • @MactarDiagne-to7eg
    @MactarDiagne-to7eg23 сағат бұрын

    Tre bien négniou teuthe sene ndeye 20ans prison soit disent policiers a

  • @mouhameddia5168
    @mouhameddia51682 күн бұрын

    raye niit loussi eup dou nattou réwandé la rék ak sokhor

  • @ZizaFaye-ls4nf
    @ZizaFaye-ls4nf3 күн бұрын

    Kousi policier def lolou khekhal au moins boy deh nga deh ak dignite wala nga rey si sakh yow

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop62163 күн бұрын

    Nou Li Sénégal 🇸🇳 Rik la Am

  • @MohamedVarre
    @MohamedVarre4 күн бұрын

    Yâ Allah Nopina ❤️

  • @natydiagne4956
    @natydiagne49563 күн бұрын

    Lii Pour laanlaa 😢😢😢

  • @papasow1752
    @papasow17523 күн бұрын

    Dakar buzz séne ligueye rafetna

  • @daoudambengue5306
    @daoudambengue53063 күн бұрын

    Des témoignages glaçants. Le Sénégal tout entier est en sursis. Malheureusement, les autorités semblent ignorer ce qui s'y passe. N'importe quoi.... 😭😭😭

  • @mouhamadouthiam5587
    @mouhamadouthiam55872 сағат бұрын

    Alors fila adouna bi tolou xana sakh malla sakh sougnko deff nii Yawmakhiyamm Dina métii😢😢

  • @user-ge3qu8nw5x
    @user-ge3qu8nw5x3 күн бұрын

    Lii métinama trop 🥺🥺

  • @ousmanediop4110
    @ousmanediop41103 күн бұрын

    Paix à son ame amineee YARABI

  • @papandiaye6415
    @papandiaye64154 күн бұрын

    Yalla nko yalla yeurem

  • @falldaba7789
    @falldaba77895 сағат бұрын

    Sénégal manoul envance dagnouye sonal sonou bopou rék tank li diougoufi 😢

  • @khadindiaye6487
    @khadindiaye64873 күн бұрын

    Paix à son âme

  • @jaalalbural7866
    @jaalalbural78663 күн бұрын

    Totou ndéme li dou yone il faut porter plainte dém ba djéhe

  • @matargueye7200
    @matargueye72003 күн бұрын

    Naniou faye plainte lenn wa police yeupe na yonn deff ligueyam

  • @ndiassefall9443
    @ndiassefall9443Күн бұрын

    Ray bi dou yonn mé ame lène diom outidji liguéye ame occupation bayi mandit bi ak lepp lou yonn di téré li moy deug

  • @ridialdieng2861

    @ridialdieng2861

    Күн бұрын

    Yangi wakh loula léroul dei fréro mandou dei bakh na

  • @MamanogayeDiop
    @MamanogayeDiop3 күн бұрын

    Policier you def yi esk gniogui xalat euleuk ak deh 😢

  • @OusseynouGueye-po4sq
    @OusseynouGueye-po4sq3 күн бұрын

    Policiers yoyou yalla nalene ya allah reubbb

  • @gnilanendiaye9953
    @gnilanendiaye99533 күн бұрын

    Thiey allah ndahk li Sénégal la.....

  • @africaserignegueye6619
    @africaserignegueye66193 күн бұрын

    Topou lenko li dou yon

  • @WelimataDiol
    @WelimataDiol3 күн бұрын

    Nagnou partager lii sii tik tok bii gnii kèneu waroul bayii lii waye daye yomb gnii dagno bone 😭😭😭

  • @MouhamedDione-si7ps
    @MouhamedDione-si7ps3 күн бұрын

    Baye jemlen guen sii lii guenn nekk nioun sii guetto bii laniou deug liko metinaniou basii kaniou yalla dakh am loumeuna defff policé amniou droit dii dort niit bamou fatu waye sama mo xamnala bu jemlen guenn sii liguey nek sino tak derr yii duniou jouk si dilen torture

  • @Khalifa450

    @Khalifa450

    3 күн бұрын

    Bien dit gars nio beugue bandit bandit lou

  • @momathniass5720

    @momathniass5720

    3 күн бұрын

    Pourquoi torture ce sont des sembesil aye domoukharam legne police yi

Келесі